Saysay bi lakk na Senegaal gépp di. Ki kay danoo wara far turam ci yoon yi ak palaas yépp. Noo ngi lay ñaan nga tàmbalee ci Lambaay tuut mu ñaaw. Jërëjëf Syll 🙏🏿
Wallahi Serigne mbaye Gueye daraam warta dess ci Sénégal . Mande damako bagne ba amna benne café boureuye bouniou toude mingui neck si wetou porte de lilas wallahil hazim Massou ma thia dougou ndakh bagne KO. Defna France 29 ans . Dieureudieuf amna solo lool.
Yalla nanou yalla attè ak fedherbe aka nekhon ma fèkè jamanom dina fayoul pèp senegalai
Saysay bi lakk na Senegaal gépp di. Ki kay danoo wara far turam ci yoon yi ak palaas yépp.
Noo ngi lay ñaan nga tàmbalee ci Lambaay tuut mu ñaaw. Jërëjëf Syll 🙏🏿
Dieureudieuf Serigne mbaye Gueye syll amna solo lool.
Wallahi Serigne mbaye Gueye daraam warta dess ci Sénégal . Mande damako bagne ba amna benne café boureuye bouniou toude mingui neck si wetou porte de lilas wallahil hazim Massou ma thia dougou ndakh bagne KO. Defna France 29 ans . Dieureudieuf amna solo lool.
Merci bay mbaye amna solo
Dieuredieufé baay mbaye goudal fane barké borom daroul mouhty ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Jëreujëf baay mbaye gueye s'il mboor mi amna sulo bëgue nanoo xam lu waral tooti lambaay ñiaw
Que Dieu te protège te donne l'envie de trop content
Afrik rek lañuy teral kileen di ray
Jërëjëf
😮😮😮😮 ohhh sama khôl diekhna
Amna solo. Niëwalniu si li waral wolof naan "Wax tuti lambaay niaaw"
Jërëjëfati ✅
JËRA JEFF BAAYE MBAYE GUEYE FEDERER BI YALLA NA TOSKARE
lii rék warnaa takh gnou bayyi France
❤❤❤❤❤❤❤
Xaral ma woo saa maam mu dimbli ma ci laaj yi 😭
Histoire Djitté Djitté yi do si indi ay léral ak lilén indi kayor
Fedherbe ennemi sénégalais yi won kon waroufi am ben toure
Kiidi 🐎 Mii Kay Jarul Tudde Dara Ci Réew Mi Billaahi Kii Moobon Te Yées
Baye mbay touty l'abbaye ñaw la soxla
Diadieuf
Jërëjëf
❤❤❤❤❤❤