Grand combat : Siteu Bou Anti Vs Baye Mandiaye 2 - Journée Jamaïcain à l’arène nationale

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 31

  • @ThioroFall-s8h
    @ThioroFall-s8h День тому +1

    Bon combat nila même sou amoul diéleu nexna
    Nila modou lo di mbeuré dioxé lo am yeup

  • @touremamecheikh9737
    @touremamecheikh9737 День тому

    Baye ma ndiaye dou nitt❤😂ya meune beuré wayy

  • @leuz.patriote
    @leuz.patriote 23 години тому

    Siteu bou ngor champion la ms baye mandiaye vres champion la

  • @boy_galsen12
    @boy_galsen12 День тому +8

    Siteu bou anti sama mbeur nga mais war nga bayi forcé action d tay téye akh

    • @cheikhdieng1674
      @cheikhdieng1674 День тому +2

      Bilahi . Haut niveau amoul forcer. nekk professionnel la ladj .

    • @fallgoor9256
      @fallgoor9256 День тому

      GUIs na lolou si mom kham na dfa wolou dolem rk

  • @SambaDiallo-s7i
    @SambaDiallo-s7i День тому +2

    Bay mandiaye seule 💨💪

  • @seydinaaliouneboromjasiji3200
    @seydinaaliouneboromjasiji3200 6 годин тому

    Baye Mandiaye 2 Dann Siteu Bou Anti Bou Yagg Troisième Action Bi

  • @kurayahmi
    @kurayahmi День тому +2

    *Sakou yi ci bopam legn wara dindi ci lamb dji une bonne fois pour toute*

  • @OusaynouMbge
    @OusaynouMbge День тому +1

    Baye yaye bandit💛💙💛💙⚔️💯

  • @SambaDiallo-s7i
    @SambaDiallo-s7i День тому +2

    Siteu bou anti daga dannou bay mandiaye mola meun mola eupp dollé dakkeu la khékh bly💪💪💪

  • @diaspora2553
    @diaspora2553 День тому +2

    Fadam 2 yagui paris thia xolenta ba😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @elzodieng8067
    @elzodieng8067 День тому +1

    Boy yene lingene yakar amoul des siteu bou anti epoul baye ma Ndiaye dôle

  • @Elzo669
    @Elzo669 День тому +3

    Baye ma ndiaye day soul ndanane 😂 siteu kassé

  • @ibrahimambaye277
    @ibrahimambaye277 22 години тому

    Arbitre yi gno yakh lamb ji ... avertissement Ken warou si diokhé victoire .... avertissement dafa gaw torop

  • @DjibyNdiaye-zq6pe
    @DjibyNdiaye-zq6pe День тому +2

    Slteu bou anti danou nga

  • @BilalDiagne-x1t
    @BilalDiagne-x1t День тому

    Baye mandiaye champion dh 😮

  • @BassbouBMN2
    @BassbouBMN2 День тому +1

    Raporter bi gor djiguen LA baye Mandiaye molen derange

  • @babacarmarone9235
    @babacarmarone9235 День тому +3

    Bay ma Ndiaye lac4😅

    • @broadcast574
      @broadcast574 День тому

      Yaw hana sètano lamb dji, Baye Mandiaye mo déff action yeup, en plus 4 ème avertissement bi dia dou woul, arbitre bi tégouko féne

  • @manianendoye3091
    @manianendoye3091 День тому +1

    Baye mandiaye warna xolate façon boumouy beureii sii Xaleii dii daaw nii rkkk

  • @boubacarbadji935
    @boubacarbadji935 День тому

    Thi SITEU lagnou royi dei😅😅

  • @kaas1610
    @kaas1610 День тому

    Pere palla dinama raye 😂😂😂

  • @ousmanesarr756
    @ousmanesarr756 День тому

    Baye madiaye meun na beurè trop nakaté vrai ndanane la

  • @sidyfaye44
    @sidyfaye44 День тому

    Fi amoul djele dh 😂😂😂

  • @PaaliouGaye
    @PaaliouGaye День тому

    Baye mandiaye daguay nakhanté rk akh😂

  • @HamathSow-o3e
    @HamathSow-o3e День тому

    Vraiment arbitre yii nion yakk lamb djiii

  • @moustaphambengue8037
    @moustaphambengue8037 День тому +1

    Mbeur yi daal li lagn xéwal

  • @ibrahimaFall-f3t
    @ibrahimaFall-f3t День тому

    Lamine Bayile togne 😂😂😂