LA GUERRE DES MOTS SITEU ET AZIZ NDIAYE «limala fay mo eup ligua…, Grand bi niou50/50… »

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 14 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 72

  • @DjillyKara
    @DjillyKara 14 годин тому +24

    Modou lô c'est le meilleur lutteur ❤❤❤❤❤❤❤

  • @Reum-
    @Reum- 12 годин тому +12

    Yalla aka meune niteum yen lamb guéni guiss rek mais dieum j di siteu daff ma yem mane Birame bilahi❤

  • @sanadieme756
    @sanadieme756 11 годин тому +6

    Yalmine Bi yagui si Yoon bou lerr boula sii daara dieulë Fall❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MameAbdouDiouf-l8y
    @MameAbdouDiouf-l8y 4 години тому +3

    Modou lô ❤ champion

  • @snsy1619
    @snsy1619 8 годин тому +4

    Merci beaucoup Zarco 🧏🧏✊✊🇸🇳🇸🇳

  • @bigMoo2017
    @bigMoo2017 7 годин тому +3

    Merci Siteu, il est moment de revoir ce qu'on paye les lutteurs. Les promoteurs gagnent le triple de ce que gagne les 2 lutteurs. Surtout avec les sponsors et les paypeurviews qui leur donne beaucoup de pognons. Il est temps de se réveiller.

  • @Misterkal555
    @Misterkal555 9 годин тому +5

    Modou lo ❤❤❤

  • @footballgod4351
    @footballgod4351 9 годин тому +2

    Yalmine bi nite gni dila bagne ngay geuna avencer ndakh sa khol mo rafet ❤ diameguene est fier de toi

  • @ibrafatyndaw9891
    @ibrafatyndaw9891 12 годин тому +9

    Siteu wakhou tapét rek guaafi wakh meunou gnoula may chance guay graw graw Lou sa 2 dernière combat défofa dara dignou sonal démal beuré way

  • @Loufa__bou__xaragne__lô__221
    @Loufa__bou__xaragne__lô__221 15 годин тому +39

    𝗠𝗼𝗱𝗼𝘂 𝗹𝗼̂ 𝗺𝗲𝗶𝗹𝗹𝗲𝘂𝗿 𝗹𝘂𝘁𝘁𝗲𝘂𝗿 𝗱𝗲 𝘁𝗼𝘂𝘀 𝗹𝗲𝘀 𝘁𝗲𝗺𝗽𝘀 ✅❤️✌️

    • @amadoubeye1733
      @amadoubeye1733 14 годин тому +1

      Sietu wakhna deuge day liguey nanko fay khalis bou bary

    • @AwaliAwali-o3k
      @AwaliAwali-o3k 14 годин тому +2

      Pas vrai monel être le plus lutter devant balla gaye 2

    • @bigtory4632
      @bigtory4632 7 годин тому

      Tout les temps naq🤣😭💔

    • @layekharagne2224
      @layekharagne2224 2 години тому

      @@AwaliAwali-o3kwakhofi dara té modou dakk ko palmarès deff loumou deffoul guene ko constant guene ko rafete carrière

  • @alassanedieng259
    @alassanedieng259 11 годин тому +5

    Zarco wakhe na deug ci bene coté ci afairou mma bi

  • @jeanpierrediouf2322
    @jeanpierrediouf2322 Годину тому +2

    Siteu yagui bougua bisnesse dé

  • @osmaneniang6116
    @osmaneniang6116 14 годин тому +9

    Balla gaye moy sama mbeur mais siteu dafay diay lamb limouy communiqué si lamb amoul mbeur bouko meum Machallah

    • @serignembacke1506
      @serignembacke1506 13 годин тому +6

      Khana danga fatei balla Gaye
      Balla Gaye c’est le pur produit de la lutte sénégalaise
      Sponsor yeup mom lagni kheuthio

    • @MDbousonko
      @MDbousonko 13 годин тому +5

      Sa waye bou dei diaye Lamb Rek Balla moy sen baye

    • @shollbidiatta1240
      @shollbidiatta1240 12 годин тому +4

      Bamou dab balla si diay comba

    • @papefaye272
      @papefaye272 4 години тому +1

      Yaw dei do supporter balla😂 saway dafa meilni do amateur l'amb deiii monde de la lutte nioni balla loumu meun si l'amb amoul kuko meun

    • @user-ot1jb4sj4ibig
      @user-ot1jb4sj4ibig 3 години тому

      Sitteu dou mbeur abb nervie la

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijan 9 годин тому +2

    Modou kese Amoul khalat ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑♥️👑

  • @ousmaneba2343
    @ousmaneba2343 12 годин тому +4

    Siteu mo geune hamni combat AK Balla gaye 2 haliss rék lassi am motah mou yok prix mo geune hamni Balla dinako douma dinako dane

  • @layelaye7820
    @layelaye7820 4 години тому +2

    Siteu mongui sogua yéwou si lamb

  • @MDbousonko
    @MDbousonko 13 годин тому +5

    Siteu koula Faye loko diar demal nga baure sa gayi sa commentaires yi s'il-vous-plaît bouléne dég Lou yorou gnou sa dépasse

  • @user-ot1jb4sj4ibig
    @user-ot1jb4sj4ibig 3 години тому +2

    Siteu nga balma mais sa carrière bi diexna ndax li dall baye mbadione mo leye dall, mbeur yii yeup nième naniou la ba paré, mbeur yi kham naniou ni nguéye tricher si beuré. Siteu va t’entraîner lii n’es sa caname dou yombe déh. Té Yow Siteu Yow akk zarco bouléne faté ayes nervis ngéne.

  • @BABACAR-l2e
    @BABACAR-l2e 9 годин тому +2

    Modou lo daffay noppalou 😂instant yi le roi👑👑👑mogui si trung bou soft Di game boys😂yi one by one 😂😂😂 siteu démal beurré dji ak balla gaye mo gueun wa salam fouye nak 😂

  • @ousmaneba2343
    @ousmaneba2343 12 годин тому +3

    Lamb mo geune nopal mo eup caché MMA ak limouy méti méti ak risque bissi nék yeup cachet bi bakhoul mbeur yi nék léne nitt

  • @alassanedieng259
    @alassanedieng259 11 годин тому +3

    Siteu wakhe deug yalla jarole fay 100f.pasq dou beure du xékhe du dr

  • @OusmaneNgom-t1l
    @OusmaneNgom-t1l 12 годин тому +1

    Meilleures bokhamanetané dagne kadoumon

  • @mansourcisse2951
    @mansourcisse2951 9 годин тому +2

    Siteu day or sujet rek

  • @daoudacisse4849
    @daoudacisse4849 14 хвилин тому

    Zarco a bien vu sur cas mma

  • @mouhamedbadiane8133
    @mouhamedbadiane8133 12 годин тому +3

    Siteu pa la dh kone😂

  • @moussandiaye8855
    @moussandiaye8855 10 годин тому +2

    Siteu boul nek ngaaka

  • @elhadjifalilouka5665
    @elhadjifalilouka5665 13 годин тому +4

    Boy Aziz amna yenene business mais douniou fayer prix demal beurré.carriere sportif dafa gatte

  • @ÖZILBOSS-g8w
    @ÖZILBOSS-g8w 8 годин тому +1

    Lac de guerre 3 yaldaw bi😂😅

  • @saliouwade5483
    @saliouwade5483 14 годин тому +6

    Siteu wakhi ragal rek ngafi wakh

    • @daoudacisse4849
      @daoudacisse4849 26 хвилин тому

      Kone dégo ko
      Siteu lambe business lay wakh

  • @SeydinakhalifaCamara-lc2tg
    @SeydinakhalifaCamara-lc2tg 8 годин тому +1

    Nima bagné Aziz si lamb graw na bilahi 😭

  • @papemoussacamara6678
    @papemoussacamara6678 3 години тому +1

    Mane nk ay iPhone yi khamou ma si dara

  • @Aboufafe
    @Aboufafe 10 годин тому +1

    😊

  • @aliounecisse2539
    @aliounecisse2539 5 годин тому +1

    En kone ioe dofo dieuleul balla kham

  • @sanadieme756
    @sanadieme756 11 годин тому +2

    Wa mais père becaye mbaye tey mbeur bouy soga dougou sii lutte avec frappe bï sa premier caché combien lay doon de même que MMA daffa am caché boy féyë kou tamite père naak

  • @daoudacisse4849
    @daoudacisse4849 27 хвилин тому

    Siteu boul déglou gni ci plateau ay courtiers lagnou

  • @khadimka2058
    @khadimka2058 36 хвилин тому

    Siteu mi dh dina yakhal bopam ndakh eupeul mom fila wara profité ligueye mouy diaay tiit

  • @ModouMbay-f4g
    @ModouMbay-f4g 11 годин тому +2

    Siteu moy lamb tarkida bi

  • @DiengDaba
    @DiengDaba 8 годин тому +1

    Balla seul

  • @AzizDramé-q4j
    @AzizDramé-q4j 12 годин тому +2

    Ki tapét leuh

  • @zulnhofaye2584
    @zulnhofaye2584 Годину тому

    Lamb lo si faya kou déf ko si galath

  • @zulnhofaye2584
    @zulnhofaye2584 Годину тому

    Modou mbaye ak bekaye mbaye khana sou lamb yakho dollén fayakou bayi léne boy yi déme

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932 15 годин тому +1

    Modou mbaye defoi moy lolou
    Lamb Senegal bouniou la fayé amilion seringng bi lek 500000 mil

    • @MDbousonko
      @MDbousonko 13 годин тому

      Sa waye kou diokh Serigne sa xaliss sa problème la Lamb ji dou afér dh Serigne

  • @FalouNgom-o3m
    @FalouNgom-o3m 13 годин тому +1

    Situe dafa ragal késsé balla dou modou dé

  • @kionking-i9k
    @kionking-i9k 12 годин тому +1

    Siteu coproduction laye dounonou nak si mbeur yi si si gagner danio wara beurrer âme aye dague si refus de combat

  • @abdouboukharagnelolo9687
    @abdouboukharagnelolo9687 9 годин тому +1

    Dou azzi moni won serigne gnam moko tere lambou?

    • @layelaye7820
      @layelaye7820 4 години тому

      Aziz ndiaye dou mousa bayi lamb

  • @papadiom9260
    @papadiom9260 14 годин тому +2

    Boul gnou fonto Eumeu Sene 160 Millions lagn ko faay Combat royal sarakher ko 😂. Siteu ladjal 150 Millions djeum kaaw dagn laay sarakher dhe 😂 Fane yi yaa khew yaaw la promoter yi di geuna weurr k ton dernier adversaire

  • @haronandiaye5045
    @haronandiaye5045 11 годин тому +2

    Siteu yow beugoule bueré

  • @elhadjifalilouka5665
    @elhadjifalilouka5665 13 годин тому +1

    Balla gaye diokhlen eumeu sen e bayi situé mou chomé

  • @pipo7489
    @pipo7489 59 хвилин тому

    Siteu mi amna niaan d , di danou ba paré niou ley féy plus. Non lamb amoul logique bilay li keneu khamoul lanla

  • @lovision3504
    @lovision3504 6 годин тому +1

    Oponute 😂

    • @Xarnoubi
      @Xarnoubi 47 хвилин тому

      Mayko lolou😂

  • @MariamaMbye-i7o
    @MariamaMbye-i7o 13 годин тому +1

    MMA dou morome lamb

  • @youssouphadiop3327
    @youssouphadiop3327 14 годин тому +5

    Yaw demal dieuli balla mo gueun ngay gnoddi ba gnom fran Ama zarko et consorts fek lafa delola thi 5 millions.
    Sa carrière lici dess beuré Toul

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 14 годин тому

      Heureusement ba nekoo manager Siteu! Amoul bene bouko eup foule boumouy drainer dagn ko wara faay lou mathh seukkk wala gnou bayii!!! Dina am sama mbeur mouy beurell Baye Ndiaye mi faar thi Balla ngakay sarakher !!!

    • @MatarMbegue-d2j
      @MatarMbegue-d2j 14 годин тому

      100 bakhna

  • @Yoro_Ndiaye
    @Yoro_Ndiaye 14 годин тому +3

    BARTHÉLEMY DIAS FACE AU COMMENTAIRE "SHOW OF THE YEAR NITDOFF...
    ua-cam.com/video/fAv18DjrzSI/v-deo.htmlsi=VqtMtL_jYpFmyA3z

    • @MDbousonko
      @MDbousonko 13 годин тому

      Yoro 😂😂😂😂😂 Barth kay