Liss ndiago mérite amplement des applaudissements, vraiment je ne connaissais pas mais là je viens de découvrir un vrai champion, un vrai gaïndé bravo 👏🎉. Yokal dolé bii rék et l'avenir dans l'arène sera radieux avec de bon manager ❤🎉😊
Le sport va chercher la peur pour la dominer la fatigue pour en triompher la difficulté pour la vaincre liss ndiago tu as complètement gagné le respect des amateurs pas mal d'amateur fogone nagnou dagnou lay humilié et je dois dire ce combat match nul la warone néke tenir ga wané ga diom et wané ga ligéye ga si combat bi kéne waroul wone dioxé victoire je suis amplement d'accord avec père tapha gueye Liss ndiago nékéti gaindé la 👊🏽
Oh 😢 quand je vois Jules baldé, Boy Niang 2 entrain de boster Pokola et la solitude partielle de Liss ndiago pour ne pas dire totale .les ténors de Diamaguene vous étiez où ?Vraiment dafa daw yaram liss tu es un vrai guerrier diambar gorgorloul ndax gor guou âme yaye dou meusseu wétt😢 Félicitations aux deux champion🙏🏾
Lyss tay nagnoul nala bi mom felicitation aux deux meilleurs comba de l’année amoul sakh deba yen yena mérité ay centaines de millions walahi nieupa contane ❤️❤️❤️❤️
Kou dé yaye ligueye linguay fekk sa bammel nitt gni dioulli nianal la ndiégueul rk lagn si meune et la vie continue fii kou nek amna koula gueuna diégué kou dèm ngua balma akhe nak
Felicitations aux 2 lutteurs. Daño liguey mo tax combat bi yomboul. Liss dafa warone xex xex bou sax dioum lo Pokola pour dane, pas bén bén. Amna taybi, andi na physique andi dolé. Mais Pokola kén dou mome, dérla.
Félicitations aux deux lutteurs mais je suis très surpris de la forme physique de liss ndiago et de son combat. On souhaite revoir ce combat et cette fois je pense que liss a un coup à jouer parce que son physique ne peut que se développer et il aura plus de confiance vu le déroulement du combat d'aujourd'hui.
Un excellent combat ! Si intensité ak sportivité ... Ils méritent qu'on leur rajoute à chacun un 2 millions ... Liss ndiago dama la khébone mais léguey nga deug nak ,bokko gueumé di nga dem ,entrainement yi bakh na ,soutien bi mo dess ...
Les vrais athlètes et connaisseurs de sport de combat savent que Lisa est physiquement plus prêt et à plus de force que Pokola !! Quel combat ! Lisa a gagné le respect de tous les fan de lutte.
Kou Dcr bii moy combat de l’année
Ay vrai gaindè layou
Mo dakon si combat yi super❤❤😂😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤mamamama❤
Ndeysan mbeur yeup teral sen wadiour molën dougual si lamb yalna yalla doli soutoura diapalë nieup
Amine 😢😢
Billahi deug la
Adouna yalla moko mome
❤🙏
Lougn léne faye diarnako
Vraiment chapeau a vous deux surtout Liss ndiago man sah damla khébone nak
Kou d'accord li moy combat khlè❤❤❤
Trop D'accord Bro
Kan mo dann
@@damienalienziklopesgoncalv3104billahi combat you melni mo dakh day am beurè am khèkh
@@sayergeye7888 pokala par dessinions arbitraire
Wa albourakh nagnou dolill liss ak pokola khaliss wayy❤❤
Liss vraiment champion deug la
Daleu guithi mom ak yar bi moma yém walahi
Sima nékonn prometteur boy yii layy favoriser bilahi
Liss ndiago mérite amplement des applaudissements, vraiment je ne connaissais pas mais là je viens de découvrir un vrai champion, un vrai gaïndé bravo 👏🎉.
Yokal dolé bii rék et l'avenir dans l'arène sera radieux avec de bon manager ❤🎉😊
Walay chaque mois maa sétane koo ❤🎉😂
AK man limoy lamb bily liss seul
Kon dé nio bokou Yam combat bi meunou ma ko miounie
Même mane
Meilleur combat de l’année mes liss champion la
Une revenche au service de la lutte.ce combat represente la lutte au plus haut sommet
L’un des meilleurs combat de l’histoire
Yalna Sénégal am diam 🇸🇳😉
L’un des meilleurs combat des 15 dernières années
Liss vraiment jambar la félicitations pokola 🎉
Lutte tv vraiment votre travail est remarquable
Meilleures combats de l'année
Félicitations à tous les deux lutteurs vraiment ils ont tt donné
Le sport va chercher la peur pour la dominer la fatigue pour en triompher la difficulté pour la vaincre liss ndiago tu as complètement gagné le respect des amateurs pas mal d'amateur fogone nagnou dagnou lay humilié et je dois dire ce combat match nul la warone néke tenir ga wané ga diom et wané ga ligéye ga si combat bi kéne waroul wone dioxé victoire je suis amplement d'accord avec père tapha gueye Liss ndiago nékéti gaindé la 👊🏽
Wallahi liss gagné na Lou Eupe sollo Mouy respect même pokola sou gnibé ba tokk kereum taye Dina khamné goor yalla ladoone beurél
😢 bilahi nieup danio yakaron pokola dakoy takhagn dane kon mou yombou liss kay felicitaton rek lakoy wax vre champion la
Yaa geuneu kateu sa nay
Bagn Waa pikin Sénégal 🇸🇳 yaww
Ki pokola deugeu nayam Mou Danou même pas 2 m’unît action by thibirr l’a commencé bayill naa féxeu yaw akh 🥹
Le sport de combat c'est l'adversité pas l'animosité
L'arbitre à fait un peu d'erreurs
Machalah li rk doyna grand combat bilay nexxna yene gnarr gnepp felicitation ❤
Diadieuf liss bon correction j'aime sa félicitation à toi liss
Vraiment liss mbeur DEUG la mais pokola domou pikine bi Gaindé deug la❤
Li moy combat❤❤Liss ndanane la bly
Kou begue setane combat bou nekh rk setanale bii combat respect sii ñarry mbeur yii❤
Wa mais ndiago bii guerrier la dh👏
Meilleurs combats de l années sey combats bii nékh n'a trop
Liiiiiiis contann nagne bly thioubo drapeau bi❤ gayi dagnn la hébon nitt kén douko hépp merci champion
Oh 😢 quand je vois Jules baldé, Boy Niang 2 entrain de boster Pokola et la solitude partielle de Liss ndiago pour ne pas dire totale .les ténors de Diamaguene vous étiez où ?Vraiment dafa daw yaram liss tu es un vrai guerrier diambar gorgorloul ndax gor guou âme yaye dou meusseu wétt😢 Félicitations aux deux champion🙏🏾
Te yayam sakh ndeysan bi liss di nekk khale la guenn adouna
@@badandiaye3778 yalla nako yallah yeureum ta kharè ko aldiana
Pokola do ragal
@@maoudediao653 wakhouma ragal leu . Niom niarr nieup ay diambar lagn lireul lima binde
Chute amena bou yagueu mais du courage à liss nagnioulèn faayëu ay millions mieux que grands lutteurs
Liss nagn ko dolil khaliss way vraiment chapeau
Ndaigo Serigne fallou bi kasé 🎉🎉🎉🎉🎉🎉lis ❤❤❤❤lisss rapidité mo dess sama ndaigo or bi❤❤
Chapeau à vous deux vraiment ❤
Fayelen xaleyi xaliss bou bari teugeulen yenen combat ay champions lagnou 👏🏽👏🏽
Première chute bi dieul am naa dé
Félicitations à vous deux on s’est bien régalé
Oui
Bilay action bi si bir la commancé
Lyss tay nagnoul nala bi mom felicitation aux deux meilleurs comba de l’année amoul sakh deba yen yena mérité ay centaines de millions walahi nieupa contane ❤️❤️❤️❤️
Thiey aduna gars yi deh faténagn pére Gaston bou yagu bilahi kou déhé pertnga😭😭yalna yalla doly ko yeurmandé barcke alkhourhane alahouma amine 🤲
Kou dé yaye ligueye linguay fekk sa bammel nitt gni dioulli nianal la ndiégueul rk lagn si meune et la vie continue fii kou nek amna koula gueuna diégué kou dèm ngua balma akhe nak
Felicitations aux 2 lutteurs. Daño liguey mo tax combat bi yomboul. Liss dafa warone xex xex bou sax dioum lo Pokola pour dane, pas bén bén. Amna taybi, andi na physique andi dolé.
Mais Pokola kén dou mome, dérla.
Arbit yi li nioy def war nan kou setat liss ndigou mo dan🎉🎉 FELICITATIONS 🎉🎉🎉liss
pourtan pokola dornakou mou danou dosi wakh
Pokala mo ndieuka dann
vraiment felicitation a c est deux jeune lutteur combat bi nekhena trop
Non lamine ak père palla ils m'ont tué 😂😂😂😂 très bon combat félicitations.
Nous sommes fier de Liss Ndiago❤❤❤❤❤
IL est de loin le meilleur combat de l'année 🎉🎉❤
Verdict waroul wone am way ah
Billaye 😢
Recours day am sakh
@@aablayesy409en bn
@@aablayesy409 avertissement ngay wakh revours
Bilay
Pourmoi c'est le Combat de l'année.
1 Combat 2 Guerrier.🎉❤
Félicitations aux deux lutteurs mais je suis très surpris de la forme physique de liss ndiago et de son combat. On souhaite revoir ce combat et cette fois je pense que liss a un coup à jouer parce que son physique ne peut que se développer et il aura plus de confiance vu le déroulement du combat d'aujourd'hui.
Best combat of the year🔥🔥
Meilleurs combat de l'année 😂😂😂😂😂😂
Domou Ndiago touss nak 💪🏾👌🏾👊🏾
Fils deu diamaguenesicapmbao rek mais felicitation a vs deux les deux grand champions
Le meilleur combat depuis longtemps
Gni nio yélo 50 millions, 100 millions.
Un excellent combat ! Si intensité ak sportivité ... Ils méritent qu'on leur rajoute à chacun un 2 millions ... Liss ndiago dama la khébone mais léguey nga deug nak ,bokko gueumé di nga dem ,entrainement yi bakh na ,soutien bi mo dess ...
Vraiment c’est le meilleur combat vous êtes des champions machallah 🙏🙏🙏🙏
Combat de l'année ❤
Liss diamaguene way tu es le mieure ❤❤Machallah
Combat de lanne mou neex mou nakhari🎉
Quel combat meilleur combat de l'année
Gnaari Champion gnaari goor yalla deug Respetc sur les deux
Sama niary mbeur niodon beurè al hamdoulilah bamou demais ni liss ndiago bou amé dolè oup lamb
Pokola loumay encaissé si lamb dji gaur douko encaisser Bilae gainde la 😂
Ngora ak mbamé dou béne
@@mouhameddiallo6151 merci.
Combat bi moo ko mooomone wayé di kon kon lou ba wadji gnimé ko. Dafa waroona beuré teh bayi xeex bi.
Pako Mame bilay nekhnguam 😅
Un combat de haute portée ils sont très brave
Lutte tv sen image rafetna. Machalah
chaque jour je regarde ce combat
Khana chômeur ngua😂😂
Dieureudieuff liss kouma nokal pokola rkk la beugoon défal ngamako bonne continuation ndiago bi 🎉
Mane srx dafma betteu
Machallah sama compétition bi lamay fatali❤❤
Les vrais athlètes et connaisseurs de sport de combat savent que Lisa est physiquement plus prêt et à plus de force que Pokola !! Quel combat ! Lisa a gagné le respect de tous les fan de lutte.
Diambaguene lanu deukh for Life bly Liss ndiago késsé lanutopou ❤❤❤❤❤
Lutte Tv est le meilleur télé Lutteur sénégalais ❤❤❤❤❤❤
C'est la cinquième fois que je regarde ça
Meilleur Combat de l’année ❤❤❤❤
Pokola Kasse liss Diam bar geun me pikine kasse amoul le neen eumeu senn pokola balde yalla mayi na leen ndam pikine kasse ❤❤❤❤
Limoy combat lila gneup don khar lamb khalé...😊😊
Vraiment liss Mbeur la mais bokola aussi machala ✌️
Félicitations 🎊 pokola 🎊
Merci tafa Gueye
Vraiment ces deux lutteurs ces des guerriers ❤❤❤
Meilleur comba felicitation a tous deux
No combat bi nekh na😢
Man dh mbam bi moy sama mbeur mais liss billahi big respect
😂😂😂
Dépasser na gris ak eumeu sene 🎊
Combat bi nekhna ❤liss pokola nekhna waye😂❤❤
Pokolo pokola poko Mbam poko Mbam la Pikine moy Sénégal 💚❤️💚❤️💚💚❤️❤️❤️💚💚💚💚💚
Vraiment liss ndiago champion gua ❤❤❤
Quel combat yakal lén boy yi ❤❤❤
Pokola baldè dèffa am fiite thièye wa keur ama baldè même dèmarche comme ama baldè machallahh ❤
Kou d’accord Liss daan nako cii thiaxabal bii
No gni dagnulén wara dolil franchement ❤
Lii Moy vrai combat de l'année
Bilahi khalé biy reporter mo eup khél tapha Gueye. Machalla boy bi yalnako yala défal diam.
Bilahi wahatiko 😂😂,Tapha Guèye dafa mélni dou ancien lutteur 😂,Lamine moko eupou hél fouf 😂
Pakola késsé❤❤❤
Arbitre bi da rattrapéwou dabou mais chute amone na premiere songuo ba mais combat bou néxx sakh👍🏾
Noooo bilay liss deff gua leppp machallah sa besss bou tay bi dafma méti surtt biguay nieuw si arènes bi méti nama trop😢😢😢😢
Aziz ndiaye li revanche la on est content ✅❤️
Entouca ils ont mérité leur paiement ✌️
Félicitations a vous 🎉❤
Vraiment Pokola à battu Liss, une victoire très claire même... .
Liss est trop fort Mach’Allah
Meilleur combat de l'année
Prkoi pas ajouter des pauses au combat comme a la box
yéna meune beuré Macha'Alla 🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳
félicitations pokola ❤🎉