Bayina Mbeurou Pikine Yeup Apres son Khoulo avc Pathé Baldé,Pape Sarr en larmes fait des révélations

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 229

  • @People221sn
    @People221sn  3 години тому +10

    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
    Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
    Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
    +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL

    • @cheikhgueye9777
      @cheikhgueye9777 34 хвилини тому

      Guy gui numero pape sarr la sokhla lossi meuna diap tè yalla takh

  • @darodiop1043
    @darodiop1043 4 години тому +72

    Kou beug seyedina Mohamed lalale j'aime ❤❤❤

  • @leilaleila6838
    @leilaleila6838 3 години тому +20

    Mougneul yalla mola nato nga beugue wa pikine khamoumala mais sincérité bingay wakhé borom khôl bou rafét nga sarr yallanala yalla sâme🙏🏽

  • @BadaraAline-f5i
    @BadaraAline-f5i 2 години тому +10

    Pape sarr nioune wa pikine nio la déf sounou xol ❤❤❤❤bandit kéne doudou défal téranga

  • @sippotv5609
    @sippotv5609 2 години тому +11

    Bien dit grand pape bayi lepp ngua ligueye Say avenirs domm yiii

  • @jeanpierrediouf2322
    @jeanpierrediouf2322 2 години тому +13

    Pape sarr yalla nalla yalla same té mayella weur ak goudou fane

  • @MamadoucherifDiallo-y5m
    @MamadoucherifDiallo-y5m 2 години тому +10

    Tu as bien fait bonne decisión nieup am foula way ❤❤ badola mome badola rek lay moussa donne force a toi pere❤❤

  • @OusseynouSarr-f3c
    @OusseynouSarr-f3c 31 хвилина тому +3

    Vraiment nous sommes avec toi Pape SARR il est tant et maintenant de prendre tes propres résponsabilités la dignité le Respect n'ont pas de prix !

  • @thiernosy2598
    @thiernosy2598 3 години тому +50

    Conseils bimalay diokh en tant que koula beug moy nga bayi lamb ak mbeur yi nga dioublou si sa borom te diamou ko bou bakh ❤

    • @FallouGalss-j8r
      @FallouGalss-j8r 3 години тому +9

      bilahi tok sa ndiabote bayii mbeur yii

    • @ametvesselwallah7998
      @ametvesselwallah7998 3 години тому +3

      Ki na jeegeludji docteur mouhamad ahmad lo depui bimko attaké batay jugul si tolof tolof, aduna bi yepe kay ndamo sunu hero national a proteger

    • @marieeliseloume5422
      @marieeliseloume5422 Годину тому +2

      Pape sarr mouno bayi mbeur yi amou niou guor gua topato sa boppeu ak sa niaboote wassalame

    • @AboulBacharSall
      @AboulBacharSall Годину тому

      @@ametvesselwallah7998 yaw doul way fi kein waxou fi waxou lolou ki mola gueune bax situation foufe sa kokou nguay wax guenoul Pap sarr

    • @marieeliseloume5422
      @marieeliseloume5422 Годину тому +2

      Yalla na khekh amine yarabi thi barke serigne babacar sy amine yarabi aminnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnne

  • @sambatorino8115
    @sambatorino8115 3 години тому +12

    Pathé balder yenako beuga delowate si société bi mais ki dou changer

    • @fatimandao8359
      @fatimandao8359 2 години тому

      Merci beaucoup pathé yakhou na sa fait longtemps passém moko dapp criminelle la

  • @ladianepathe5637
    @ladianepathe5637 2 години тому +9

    Pathé vraie doff ngua

  • @matargueye921
    @matargueye921 15 хвилин тому

    Vraiment Grand Pape Sarr c est vrai pikinoi dafa yaga khékh nguir pikine walahie il est temps nga bayi lambe séti lanéne ndakh lambe défa loula dara mais yalla bakhna yalla dinala fay sa khole diame si yaw❤❤❤

  • @AbouRidiall
    @AbouRidiall 3 години тому +7

    Pathé baldé dal vraiment kou niak fayda la ak lila pape sarr defal lepou

  • @seringembacke9316
    @seringembacke9316 2 години тому +6

    Pathé môme mbam dége le 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv 2 години тому +8

    Pakola bako jule balde bayé ngéne wara khamni yarouwoull moke pathé gno yame 😮

  • @ibrahimadiouf8664
    @ibrahimadiouf8664 57 хвилин тому +3

    Pape SARR il est tend que tu te concentre sur tes projets et laisse certaines personnes qui n’ont pas la peine

  • @PacoVerrattiSarr
    @PacoVerrattiSarr 3 години тому +6

    Wa pikine Amouniou sa Faye bilahi yalla n'a sa Diam yague pape Sarr force a toi est bon rétablissement ❤❤❤❤

  • @nogayeniang9119
    @nogayeniang9119 2 години тому +2

    Bilakhe dou baye lamb ji pape sarr khol bi ❤ mou Nice Manol diapou dará ❤

  • @thiernombaye4340
    @thiernombaye4340 Годину тому +3

    Lii dafa niaw trop barki serigne touba bilay pathe Balde ya tegal sa ndey pape sarr nittt kou bakh la deee ❤️❤️❤️

  • @СЕНЕГАЛМОЯСТРАНА
    @СЕНЕГАЛМОЯСТРАНА Годину тому +4

    Bilahi wo n'a pape sarr ba tayi téléphone sa bou ma ko wowè mou nè ma kasso la dèmone sèti pathé

  • @NdiaboutaDiouf
    @NdiaboutaDiouf Годину тому +3

    slt à tous pape tu as tous fais pour les lutteur de pikine mais len rekk la guiss moy diemal wout visa nga diema dem france wala Espagne wala l'Italie c'est juste une conseille ndakh damala xam ndakh sa xol dafa rafet te gayi dagniy soûl naaaan nekal si sa bop merci frère

  • @henricorentindiedhiou1124
    @henricorentindiedhiou1124 2 хвилини тому +1

    Pape SARR concentre toi sur ta famille maintenant c'est mieux. Toutes les Sénégalais sont témoins de ce que tu as fait pour Pikine concernant la lutte .
    Alors courage à toi et soit fort

  • @seringembacke9316
    @seringembacke9316 2 години тому +4

    No pokola dou nit sax bilahi 😢😢😢😢😢😢😢

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j 2 години тому +10

    Pokola sa combat bi walahi Al azim titeul nala guiss ngeu nitt dangay am coleuré mounouma comprendre Pathé di sagua pape sarr sa kanam wakho si dara mais nakk dingako guiss légui 😢

    • @MDbousonko
      @MDbousonko 7 хвилин тому

      Yalla an danou da gno rew

  • @cheikhfall5548
    @cheikhfall5548 3 години тому +3

    Merci grand pape sarr nous sommes derrière toi

    • @cheikhfall5548
      @cheikhfall5548 3 години тому

      Borom khol bou rafet gua yalla nala yalla samou samou sa ndiabote Machallah

  • @mbayesarrdia4470
    @mbayesarrdia4470 18 хвилин тому

    Pape sarr yallnala takhawou
    Talfa dane pokola thiowli diekh inshallah

  • @modoudiawdieng5228
    @modoudiawdieng5228 2 години тому +3

    Yalla Na Yalla Faye la

  • @khadyly1787
    @khadyly1787 2 години тому +2

    Ndeyssane un vrais pikinite 🥰🥰

  • @ousmanesarr8279
    @ousmanesarr8279 Годину тому +1

    Machalla pape sarr😭😭😭😭😭

  • @elhadjimamadoudiaw3628
    @elhadjimamadoudiaw3628 2 години тому +4

    Pape sarr bou guedei deh pokola day danou !

  • @sellediop1817
    @sellediop1817 5 хвилин тому

    Pape Sarr yalla bakhna❤❤❤❤

  • @papemalicksow994
    @papemalicksow994 Годину тому +1

    Merci pape sarr ya ame foula lii monye deug bayil Wa pikine

  • @diazkara37fou13
    @diazkara37fou13 13 хвилин тому

    Xoll bi mo rafet ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✊✊✊

  • @SouleymaneDiaw-su3qj
    @SouleymaneDiaw-su3qj 40 хвилин тому +1

    Yalnala yalla Faye sa khool

  • @SerignemodouDiagne-tr7rw
    @SerignemodouDiagne-tr7rw 11 хвилин тому

    Ndayessane wallahi pape sarr kobakhla

  • @AbdouDiop-d6t
    @AbdouDiop-d6t 3 години тому +1

    Pape sarr svp khol si ama balde ❤❤

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 2 години тому +5

    Grand nga balma bayil mbeur yi amou ngou béne ndiarine

  • @MoussaDieng-y2y
    @MoussaDieng-y2y 3 години тому +6

    PiKINE. KHAMOUGNOU. PATHÉ. . PAPE. SARR. LANIOU KHAM

  • @maguettediopsow2786
    @maguettediopsow2786 36 хвилин тому

    Pathè daffa dioum drète mo forr il faut le comprendre. Courage grand pape pikine Sénégal sont fière de toi

  • @ousmanesarr8279
    @ousmanesarr8279 Годину тому

    Mashallah Pape sarr pikine ❤️💚❤️💚❤️💚

  • @taphadiene
    @taphadiene 21 хвилина тому

    Theye wa pikine Aka nio wayadi 😊

  • @ousseynoudieng2407
    @ousseynoudieng2407 16 хвилин тому

    BAYIL LAM BBEUR DOU GOR

  • @PapeLatyrSeck
    @PapeLatyrSeck 2 години тому +1

    Yalla na la yalla takhawou

  • @FallouNiang-k1j
    @FallouNiang-k1j 2 години тому +2

    Pape blh damala beugue

  • @DaoudaNdiaye-l3d
    @DaoudaNdiaye-l3d 32 хвилини тому

    Au yalna yalla défale diam rek inchallah

  • @truckwarriors9832
    @truckwarriors9832 39 хвилин тому +1

    Bayil lamb pape!lamb ak pikine dellowougnou leu seu geud!

  • @NgomDjiga-c6r
    @NgomDjiga-c6r 41 хвилина тому +1

    Pape sarr mérna nag😂😂

  • @LamalanabaLamalanaba
    @LamalanabaLamalanaba 2 години тому +2

    Grand pathé vrai dof la

  • @momoly543
    @momoly543 17 хвилин тому +1

    Bayil lamb mbeur diarouko ahhh

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j 2 години тому +1

    Grand pape amal fouleuh nga bayi worr katt yi bakhouniou apart ama akk Jacob.

  • @MorGning-n4i
    @MorGning-n4i 3 години тому +3

    Thiey pape Sarr ak pathe doyna war 😂😂

  • @codoudiouf-ij8go
    @codoudiouf-ij8go 2 години тому +1

    Pape boule dioye waye paté mi daye nite tokh katou yamba rék la yalla dinaléne até inchallah

  • @ElhadjimaguettendiayeGueye
    @ElhadjimaguettendiayeGueye 2 години тому

    Courage pape sarr

  • @malickcisse869
    @malickcisse869 2 години тому +2

    Li mitina de 😢

  • @afro3827
    @afro3827 3 години тому +4

    Bal mbeur yi amognou ben jarign

  • @hadyagne9473
    @hadyagne9473 24 хвилини тому

    Pathé il faut que tu respectes Les gens

  • @cheikhfall5548
    @cheikhfall5548 2 години тому +6

    Borom khol bou rafet bi Machallah yalla na la yalla samou samou sa ndiabott

  • @ladianepathe5637
    @ladianepathe5637 2 години тому +1

    Pathé vrai nguaka leuh pour maan saak day guenah djiegalou

  • @JabelMusik
    @JabelMusik 49 хвилин тому

    May Allah be with you Pre, Yallah baahna nit tei Sanga reh beh Tass

  • @khadimndiaye352
    @khadimndiaye352 3 години тому +1

    Yow grand Pathé baldé dof bobou ngay wéréntél mangui lay beugeu méré sakh bilahi

  • @naby-wb6xe
    @naby-wb6xe 2 години тому

    Père ya takhe may supporté pikine dh bilahi

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 2 години тому +1

    Pape sarr stp do bayi mbeur yi

  • @dembacoulibaly3447
    @dembacoulibaly3447 Годину тому

    Salam j❤me .PS ./Pather s'il te plait fait tout pour le demandee pardon ton G pape sarr pour le bien de toute Pikinois jajeuf

  • @ElhadjCiss
    @ElhadjCiss 52 хвилини тому +2

    😢 dafa sonn si guayi bilahi

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv 2 години тому +5

    Pape sarr aka mana sole maillot you rafete 🎉

    • @Mamegor-uz3lb
      @Mamegor-uz3lb Годину тому

      Kone guiss ngua lolou

    • @birame696
      @birame696 Годину тому

      Copin pros yi leu 😅

    • @abdoutall8491
      @abdoutall8491 47 хвилин тому

      Bilaay ay kharite pro la yor bii moustapha Mbow Paris fc leu

  • @PapaDembaSy-jb3ik
    @PapaDembaSy-jb3ik Годину тому

    Amal diam AK tane bu wér grand pape Sarr ...

  • @moussapayemane4167
    @moussapayemane4167 Годину тому

    Beug na lamb trop mais pour ma topou mbeur yalla téré si aduna,nguir yalla Pape sarr bayil mbeur yi té diap sa famille lolou moy leup

  • @deugrek344
    @deugrek344 3 години тому +7

    Bilahi bouma guiss niit kouy topou mbeur ak di sacrifier sa life pour mbeur damay diap amo ambition sa adouna😂😂. Mbeur yo kham ni sén intérêts ak pertube wa quartier yep bou niou amé combat. Yéwou lén jeunesse bi guén démb wouti lolén am té wagni thiakhane yi comme lamb etc.

    • @AlioueFootball
      @AlioueFootball 3 години тому +1

      Diamaguene la deuk mais bou Siteu amé combat souma guissé boys yi di fanane si bountou keureum saga sen leufeul ndeye rek lay beug

    • @cheikhgueye9777
      @cheikhgueye9777 2 години тому

      Bilahi wakhgua deug frère

  • @soppeousmanesonko777
    @soppeousmanesonko777 3 години тому

    Yow dh môme machallah lenne dh kham Na ko Beuga Mbeur pikine Yi 🎉 yow dh pape Sarr Bene Yonne la mossa merée Moy bingaye dal SI Modou Lo reke apart Loulou môme cool 😎

  • @saidoubah8511
    @saidoubah8511 Годину тому

    Pathé devrait s’excuser vraiment mais il continue de minimiser ces faits dofla werul pape courage ❤brom mbakh nga

  • @WadeCourtois907
    @WadeCourtois907 3 години тому +3

    Yalla na léne yalla dioubolé Pape Sarr mangui lay niane guirr yalla rekk nga ngeuna mougne tay diélalé ak diegualé PIKINE mome gnépou khame nagne né ligua déff PIKINE do toull Yombou nitt déff kofi mane nakk deukou MA DAKAR SAKHE BAY DEUKK PIKINE BILLAHI WALLAHI WATALLAHI Adouna mo amoul sólo rekk té diamou sila Léppou khathie

    • @ibrafatyndaw9891
      @ibrafatyndaw9891 2 години тому

      Loumouy mougn kii délal lougn koo dara limouy top 1f CFA amoukossi guanane mougn khana sakh niit boula amal ndiarigne boula naré yap sakh gua ndem guanane mougn

  • @serignemansourndour6096
    @serignemansourndour6096 38 хвилин тому

    Pikine sou mbeur yi perté kou melni pape sarr mom dinagne niakeu chance ✋

  • @Imam1faye
    @Imam1faye 18 хвилин тому

    Pathe vrai weurr katt leu, bilae😢

  • @PacoVerrattiSarr
    @PacoVerrattiSarr 3 години тому

    Li métina pape Sarr à fait tout pour pikine vraiment mougnal rék yalla bakhna 😭

  • @seringembacke9316
    @seringembacke9316 2 години тому

    Noo sarab ndieyi mber RK 😭😭

  • @doufou-p8g
    @doufou-p8g 54 хвилини тому

    Wa gni ay nitt lagnou esk 😢😢 comment peut on dire ça

  • @Lamzi92i
    @Lamzi92i 3 години тому +4

    Chaque année Pape tu nous joues le même film .
    Nopalal sa bopp grand bi

  • @mamegorthiaw-gy5od
    @mamegorthiaw-gy5od 3 години тому +1

    🙏🙏🙏

  • @alyba7688
    @alyba7688 2 години тому +1

    Laisse ces lutteurs ingrats et concentre toi sur ton avenir

  • @ibrahimadiouf8664
    @ibrahimadiouf8664 31 хвилина тому

    Grand Pathé il est tend qu’il change ces comportements d’adolescents et regarder ces frères comme ama et Jules et ses enfants comme Jacob

  • @khalifadiongue4989
    @khalifadiongue4989 16 хвилин тому

    Pape sarr linga bayi si Lamb mongy beugeu bari deeeeee

  • @domousenegalinfo9563
    @domousenegalinfo9563 11 хвилин тому

    Pathé weroul boul ko top

  • @papemalicksow994
    @papemalicksow994 Годину тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @alassanegomissagna4987
    @alassanegomissagna4987 2 години тому

    Grand Pape Sarr yaa waraa wayi Mbeur yis teiii talll sa bop…❤

  • @abdousarr9749
    @abdousarr9749 40 хвилин тому

    Pape sarr ndeysan seytané mo bori dole dé

  • @cheikhseye6929
    @cheikhseye6929 19 хвилин тому

    Pape sarr diam si yaw

  • @Lebou-fh8ub
    @Lebou-fh8ub 3 години тому +2

    Grand bayil lamb dh tog sa keur papa

  • @BarkaKoita
    @BarkaKoita 2 хвилини тому

    Amal joom, nga guéneu thji Mbeur yii.

  • @kmhiphop8849
    @kmhiphop8849 2 години тому +2

    Boul waat li amoul solo

  • @fodetoure8740
    @fodetoure8740 3 години тому

    Ndeysan

  • @tallameth8174
    @tallameth8174 35 хвилин тому

    😭❤️

  • @MamadouSow-p3q
    @MamadouSow-p3q 3 години тому +1

    malla wakh lolou pape amal foula Sénégal fofou la tolou ko lebal kerr mou Faye la safara

  • @BayeModouGueye-j2s
    @BayeModouGueye-j2s 3 години тому

    ❤❤❤❤❤

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 Годину тому +1

    Pape bayiwate n'a pikine dai😂😂😂legui mou nieuwate ndeysan pikine rk la beug pap sarrr dafa mer rk

  • @serignembacketoure8796
    @serignembacketoure8796 2 години тому

    Paté mi diaroul topu dekue bi dakoo raw 😂😂

  • @Papisdiop349
    @Papisdiop349 3 години тому

    Pape Bayil mbeuryi nga nek sa bop

    • @BabaSaka-sk7is
      @BabaSaka-sk7is 3 години тому +1

      Bilhi ki dano ko wara wakh deggue na bayi mberyi mo guene thii mome

  • @alassanemane3021
    @alassanemane3021 Годину тому

    Pape Sarr bayyil lamb nga néka si sa bopp ak sa famille ndakh mo geune billah

  • @MoussaDieng-y2y
    @MoussaDieng-y2y 3 години тому +2

    PATHÉ. YÉENAKO. DEF. NIT. WAYÉ. DOU. NIT

  • @marieannieyalixdiatta5286
    @marieannieyalixdiatta5286 2 хвилини тому

    Comme on dit Mbeur akk Joueur ayyy workatt laniou... reconnaissance zéro 😢😢😢

  • @diagne1041
    @diagne1041 5 хвилин тому

    Mbeur amoul kollare