"Naka Laniou Faté sama Doom" la mère de Fallou raconte les derniers moments de son fils

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 2 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 94

  • @maimounabathily1211
    @maimounabathily1211 Рік тому +14

    Vraiment metii na mais papa dji gueum naa yalla yallnako yalla yeureum tei khareiko aldiana firdawsii amine

  • @Salimata-lp5uc
    @Salimata-lp5uc Рік тому +2

    Yalla nako yalla kharé aldiana fidawsi si barke Serigne Touba 🤲

  • @mamegayekane839
    @mamegayekane839 Рік тому +9

    Yalla nako yalla yreume khari ko adjana firdawsi inchallah 🙏

  • @ndeyeba6413
    @ndeyeba6413 Рік тому +5

    Deysane pape ji bahna néna jégal nako😢😢😢ay way nagne yare sounouy dome jangal léne diné😢

  • @maimounadiagne4313
    @maimounadiagne4313 Рік тому +5

    Paix à son âme. Yalna agualer ndawam ci aldiana firdaws, yalla may léne kholou mougne

  • @salihate-ew6wy
    @salihate-ew6wy Рік тому +3

    Yalla nako yalla kharé aldiana firdawsi si barkel seringe saliou Amine yarabi 🙌

  • @princessemyadiallo9791
    @princessemyadiallo9791 Рік тому

    Fallou sakh da nék khalé yalnako yalla yeureum ta khareko aldjana firdawsi 😭😭😭😭😭 massa Mane dé légui dama warou mane

  • @joserere4274
    @joserere4274 Рік тому +18

    Souvent dans les milieux interlopes ce genre d’événements tragiques se produisent. Il faut savoir choisir ses amis et andado

  • @fatoudiakhate1516
    @fatoudiakhate1516 7 місяців тому

    Yalla nako yalla yeureum khareko aldiana firdawsi si barke zeydina Mohamed amine ya raby

  • @NdeyefamaNiang-b6g
    @NdeyefamaNiang-b6g Рік тому +2

    Massa léne yalla na agalé ndawam firdawsi

  • @Fatoumbodji459
    @Fatoumbodji459 Рік тому +1

    Yalna ko yalla yerem té djégal ko kharé ko Aldjana ya guene kawé Inshalah

  • @farmataniang5608
    @farmataniang5608 Рік тому +1

    C est triste qu allah l accueille à son paradis firdaws amine

  • @dakartv465
    @dakartv465 Рік тому +13

    Warnagnou interdire Di diaay arme blanche si boutique yi c trop facile c la troisième fois que j'attends ça , en plus diaay arme blanche bassi goudi koukoy dieudeu sakh warokoko diaay

    • @diopmamemor1961
      @diopmamemor1961 Рік тому +3

      Surtout lolu arme blanche wara tougnou ko diaay si boutik yii

    • @originali155
      @originali155 Рік тому +1

      Surtout franchement gouvernemekt bi war nassi jeul aye mesure

    • @TheBandafall2003
      @TheBandafall2003 Рік тому

      Ds tous les pays du monde on vent des armes blanches ds les espaces

  • @farmataniang5608
    @farmataniang5608 Рік тому +1

    Qu allah l accueille à son paradis firdaws amine

  • @ThiesKaay
    @ThiesKaay Рік тому +17

    Nguenn baal ma nak, li nguenn di doundou mettina.
    Mais wakh deugg yalla kou lenn degg khamni ay parents you daw senn responsabilité nuenn.
    Sa domm bou toll ni , 14ans, mineur,, dianguiwoul di trainer ak ay fakkman baniou key diam, nga naan mom khalé bou toll ni mo ley diokh yaw wadiouram ngay ndogou té khamo fimou ko dieulé, di khotill yérré ay magam et tout... 14ans dou sakh age liguey..
    Vraiment je suis désolé mais yena ko sacrifier. C'est pas facile à realiser nak, mais c'est une vérité dure..
    Yalla na lenn yalla yokk mougn té yeureum ko.

    • @TheBandafall2003
      @TheBandafall2003 Рік тому +4

      Ds les quartiers lebou on commence a travailler tôt il était pêcheur simplement mais je te comprends c trop tôt pour travailler à cette âge

    • @christinesylva9654
      @christinesylva9654 Рік тому +2

      Vraiment c'est ce qui m'a choqué. Il était trop jeune pour prendre soin des siens.

    • @ThiesKaay
      @ThiesKaay Рік тому +9

      @@TheBandafall2003 Diangg metier à la rigueur..
      Mais travailler jusqu'à ce que ta famille dépende de toi, ce n'est pas son rôle..
      Té kou wekkou ci mom pour ndekki wala ndoggou té ngay maggoum dieum... sa sens de la responsbilité yemm na ma..
      Segam mom mi ndaw mo meun wutti di la diokh, yaw makk nga warr ko meun khagn thionno bobou té wutali sa bopp..
      Ma ngui diegalou mais deugg nekhoul nak

    • @marieamar134
      @marieamar134 Рік тому +1

      Nenaniou khaley bi dafa doone dem gaal, louniouko fay mou diokh maamam

    • @marieamar134
      @marieamar134 Рік тому +1

      Khaley yi deukk fou am guedj yeup daniouy tela kham liguey di débrouiller tôt 😊

  • @coumbandiaye10
    @coumbandiaye10 Рік тому +6

    Yalla nako yalla yeureum té kharé ko aldiana 🙏 🙏 🙏 🙏 🙏 🙏

  • @AliouThiam-qr6su
    @AliouThiam-qr6su Рік тому +2

    Yalna ko yalla xarè aldjiana firdawsi

  • @khalifambengue6125
    @khalifambengue6125 Рік тому +18

    Yalnako yalla yeureum té diegeulko si barkè seydina mouhamed sws ❤️❤️❤️

  • @fatoufaye3289
    @fatoufaye3289 Рік тому +3

    Yalla na firdawssi di nopalou kayame si barki seydina mohammed amine yaraby

  • @Al_Hamdoulilah
    @Al_Hamdoulilah Рік тому

    YALLAH Firdawsi di keureum, YALLAH na YALLAH may kholou mougne ay wadiour wam🙏🏾

  • @khardiatadiene5346
    @khardiatadiene5346 Рік тому +4

    SÉNE YOLE LA SA AL DIANA YI GUENA KAWÉ FIRDAWSI MÉTINA WANDÉ DÉ GUI MOYE SOPI AYE MAGAME MA SHA ALLAH GNIANE-NALE LÉNE TÉ NGA OYOFAL DI WAKH-TANE AK GNOME.❤❤YALLAH BOUYY DÉFAR DAYEE MÉLL NÉÉ LOUYY YAKHKH DI NA BAKH IN SHA ALLAH ❤❤❤❤❤❤❤

  • @valedianamendy6453
    @valedianamendy6453 Рік тому +1

    Massa metina yalla nako yalla khare aldiana firdawsi 😭

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 Рік тому +2

    Yalla yereumko amine way métina trop bilahi,

  • @valedianamendy6453
    @valedianamendy6453 Рік тому +3

    Falou dafa téla sotisi khalè motakh meunoul yagui fi 😭😭

  • @fatoumatabintadiallo7702
    @fatoumatabintadiallo7702 Рік тому +2

    Yallah nako Yallah yeureum té harelko aldiana firdaws

  • @christinesylva9654
    @christinesylva9654 Рік тому +8

    Comment un enfant de 14 ans peut trouver de l'argent jusqu'à donner le ndogou, faire des dépenses etc.
    Nguir yalla chers parents assumons nos responsabilités. C'est à nous parents de prendre soin de nos enfants et non le contraire.

    • @fandao2138
      @fandao2138 Рік тому +1

      Lolou moma déranger si wakh ji vraiment, yalna khipé aldiana

    • @christinesylva9654
      @christinesylva9654 Рік тому

      @@fandao2138 amine🤲🤲

    • @marieamar134
      @marieamar134 Рік тому

      C'est vrai il est très jeune, mais khaley yi deukk fou diégué guedj ou am mbokis yi dem guedj daniouy téla dem guedj Di débrouiller, di diapalee sen keur, 14 ans c'est jeune mais seddee yi rafetna si Fallou yalna yalla mayko aldiana firdawsi inchallah

  • @annawade4825
    @annawade4825 Рік тому +2

    Oh 😢metina trop

  • @mamefatou7143
    @mamefatou7143 Рік тому

    Que son âme se repose en paix 🪦 yalla khared ko aldiana firdawsi

  • @kaderkane5775
    @kaderkane5775 Рік тому

    😞😞😞😭massa metina repose en paix que firdaws sois ta demeure

  • @babusenegal8079
    @babusenegal8079 Рік тому

    Ndeyssane yalnalene yalla maye kholou mougne yalna motale ndawame aldjana metina torop waye massa😭😭😭

  • @ndeyendaw3946
    @ndeyendaw3946 Рік тому +1

    yalla nako yalla yeureum kharéko aldiana

  • @bahasiba-sk6hw
    @bahasiba-sk6hw Рік тому +1

    Fallou hale bou rafet la (paix à son âme)😢

  • @mariamamboup9741
    @mariamamboup9741 Рік тому

    Massah yalla nako yalla yeureum thé kharéko aldiana firdawsi

  • @zaldiop6293
    @zaldiop6293 Рік тому +3

    Wallahi li metinna trop allahouma akhfirlahu warahmahu 🤲🤲niakh bou wow mo lak niakh bou toyy😭😭

  • @ndeyefatouba1012
    @ndeyefatouba1012 Рік тому +2

    Massa nalène YALLA doli kholou mougne si Barké SEYDINA MUHAMMAD !

  • @BeugBaye-kw8ov
    @BeugBaye-kw8ov Рік тому +1

    Yalnako yala yeureum ma agualé dawam aldiana

  • @aminatasall2573
    @aminatasall2573 Рік тому +1

    Ndeysane paix à son âme ndeysane

  • @nogayediop4582
    @nogayediop4582 Рік тому +1

    Lolou deh fallou yepp la dagniy lédjie donne nittou nite yii motakh

  • @anginapiodndong2508
    @anginapiodndong2508 Рік тому

    Yalnako Yalla yeureum

  • @margotdieng7164
    @margotdieng7164 Рік тому +1

    Massa maman
    courage😢

  • @newsinfosbyme
    @newsinfosbyme Рік тому +1

    Massa maman❤

  • @aissatagangue2858
    @aissatagangue2858 Рік тому +3

    Paix à son âme

  • @mariamacisee6380
    @mariamacisee6380 Рік тому

    Ndaysane Yallanako Yallah yerem 🥲

  • @mamamniang4068
    @mamamniang4068 Рік тому +1

    Paix à son âme Ndeysane 😭😭😭

  • @KhadyNdiaye-i2c
    @KhadyNdiaye-i2c Рік тому

    Lolou metina deh

  • @HousseynKadi
    @HousseynKadi Рік тому

    😢😢

  • @fatimatasambasy3876
    @fatimatasambasy3876 Рік тому +1

    Que son âme repose en paix

  • @kalmdieng
    @kalmdieng Рік тому

    Repose en paix 😭😭😭😭😭😭

  • @ndeyendaw3946
    @ndeyendaw3946 Рік тому +1

    Ndaysan massa

  • @DikhaSena
    @DikhaSena Рік тому

    😢😭😭😭😭

  • @massdiouf242
    @massdiouf242 Рік тому +1

    Métti na mes Yallah bakh

  • @aidandiaye9843
    @aidandiaye9843 Рік тому +3

    Lii metina lol mais paka yignouy diay ci boutique yi tamite dougnsi wakh a chaque fois c comme ça

  • @amydiop5908
    @amydiop5908 Рік тому

    😢😢😢😢

  • @papeseck9969
    @papeseck9969 Рік тому +2

    Entouka li gniko sédél ci khalé bou ame 14ans kou bakh tei amone diome la wone

  • @falloufall6440
    @falloufall6440 Рік тому

    Bylay. Yena manalatie

  • @elhadjigueye2646
    @elhadjigueye2646 Рік тому +1

    Massa yaye boy

  • @awadiouf9655
    @awadiouf9655 Рік тому

    😭 😭

  • @PapedembaBa-r8r
    @PapedembaBa-r8r Рік тому

    😊

  • @massdiouf242
    @massdiouf242 Рік тому +1

    Papa goor deugue gua Billay

  • @ummhuraira2495
    @ummhuraira2495 Рік тому +1

    Elle n'arrive pas à parler de son fils au passé. Massa.

  • @khardiatadiene5346
    @khardiatadiene5346 Рік тому

    SALAM YALLAH NA KOO BOROM BI KÉRALÉ SI AL DIANA YI GUENA KAWÉ FIRDAWSI MOME AK GNI MOU FA FÉK AK GNI KO FA FÉK AMINE YA RABBI GNOU BOK .KOU BAKH MOYE DÉF NONOU ,MANE MI DA MAYE KÉKANETO KHALÉ

  • @TheBandafall2003
    @TheBandafall2003 Рік тому

    Au Sénégal on a laissé des la création de ghetto partout

  • @amyfalldiarra1872
    @amyfalldiarra1872 Рік тому

    Massa nitt kou bakhga bilay

  • @khardiatadiene5346
    @khardiatadiene5346 Рік тому +1

    YALLAH NA LAA BOROM BI FAYY WADIOUR YI DA GNOUYE RAGALE MEUNE NA AME MOME MOU SOPÉ-KOU SI LOLOU KHALÉ LA GNOU NDÉYSSANE

  • @BinetaSy-sj4ir
    @BinetaSy-sj4ir Рік тому

    Deysane

  • @amirkibily-dp8gz
    @amirkibily-dp8gz Рік тому

    Repose en paix mon frère 😭

  • @mature144
    @mature144 Рік тому +1

    un enfant de 15 ans qui tue a point mort c'est bizare

  • @mariamaba1578
    @mariamaba1578 9 місяців тому

    1minute dioye lo khaléyi. .dougeu t il si deke bi ti togne gnou léye clamé

  • @mamadoudeme5562
    @mamadoudeme5562 Рік тому

    Ndeyssane méttina lol

  • @ModouDiop-m1w
    @ModouDiop-m1w Рік тому

    Ndaye San metina lol

  • @norayni_avec_ses_vdo
    @norayni_avec_ses_vdo Рік тому

    Fraçmant méttina

  • @mariama3867
    @mariama3867 Рік тому +2

    Paix à son âme

  • @fatoundiaye2247
    @fatoundiaye2247 Рік тому

    Paix à son âme