Sébikhotane : meurtre sauvage d'un enfant de 4 ans, Sa tante arrêtée !

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 870

  • @marieb470
    @marieb470 2 роки тому +214

    Ndeysan vraiment li metineu. Courage à la famille. Paix à l'âme de ce petit ange

    • @ndeyefatoudiouf2745
      @ndeyefatoudiouf2745 2 роки тому +2

      Paix à son âme qu'Allah l'accueille dans son paradis céleste Amine 🙏

    • @mamiediaw2274
      @mamiediaw2274 2 роки тому

      Hé qqqq que y z

    • @Sherif221-YTB
      @Sherif221-YTB 2 роки тому

      *Lou doyy waar* 😭😭👇👇👇👇👇ua-cam.com/video/NHK89-Eg8ec/v-deo.html

  • @aramewade1717
    @aramewade1717 2 роки тому +157

    Keur famille yi ken supportewoul keneuhh l hypocrisie bi

    • @fatouthiam2561
      @fatouthiam2561 2 роки тому +21

      Tu as raison ma chérie. Trop d'hypocrisie dans ce pays.

    • @aichambenetoure9945
      @aichambenetoure9945 2 роки тому +33

      bilahi gnoune sognou keur tasna 😭di liguéyaté yakaté té kén doulen deff dara dafa méti dagni xol nit rk bagne ko né kéneuh dou avancé 🤔

    • @fatouthiam2561
      @fatouthiam2561 2 роки тому +20

      @@aichambenetoure9945 motakh loci guiss douniou avancé kossi guiss yénéko sarakh

    • @aminatandiaye2240
      @aminatandiaye2240 2 роки тому +1

      Bilay deugue leu

    • @toosource
      @toosource 2 роки тому +11

      Bougnou diougo nane deugou dioulite

  • @minachouendiaye8462
    @minachouendiaye8462 2 роки тому +159

    Khaler bou 4 ans un petit ange 👼 ndeysane deffoul keine darra gua rayko niii gratuitement va en paix bb purée raye yii senegal beurina trope vraiment douniou appliquer peine de mort ☠️ guirr yallah

    • @abybodian1448
      @abybodian1448 2 роки тому +4

      c'est le comble

    • @maremesougou8031
      @maremesougou8031 2 роки тому +2

      Mane dh kou rayy lou takk si mane bama khamni iowla dinala ray walla ma ray lou takk si iow ñiou bokou sall prison li daffa yombe trop di ray xale bou khamoule dara nakh amega bleme ak yayam pour lanne

    • @top1015-q6q
      @top1015-q6q 2 роки тому +2

      @@maremesougou8031 bilahi kou ray lou Tak si Mann barki alkhourann ma rayla prsq Li dafa yomb de trop

    • @top1015-q6q
      @top1015-q6q 2 роки тому +1

      @@maremesougou8031 bilahi kou ray lou Tak si Mann barki alkhourann ma rayla prsq Li dafa yomb de trop

    • @madjiguene4935
      @madjiguene4935 2 роки тому +1

      😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @mamifashion4567
    @mamifashion4567 2 роки тому +372

    Mon cœur de mère saigne tellement c’est dure massa repose en paix petit ange 👼

    • @biolexacosmetics1443
      @biolexacosmetics1443 2 роки тому +3

      C'est dure😭

    • @adamdiouf7245
      @adamdiouf7245 2 роки тому +2

      😭😭😭😭

    • @binetoukane1318
      @binetoukane1318 2 роки тому +7

      Mon cœur de mère saigne aussi, je suis en France mais on entend pas ça ici.
      Mon pays va mal

    • @adamdiouf7245
      @adamdiouf7245 2 роки тому +2

      @@binetoukane1318 franchement mètina trop jai peur sènegal woroul

    • @adamdiouf7245
      @adamdiouf7245 2 роки тому

      @@binetoukane1318 moi en italie yalla nagniou yalla sam bolègniou soutoural Sam diabote gui

  • @thiorodieng3814
    @thiorodieng3814 2 роки тому +229

    Mère prkoi guay wakh gnari wakh,j'ai écouté un premier interview ou vs avez affirmé k la fille avait une foi poussé le pti frère du défunt ds une fosse septique et que l'enfant a fait deux jours à la pédiatrie,et k yassi tek sa tank dakh bagn mbok gui tass,DC prkoi guay tok Di wakh nane amougnou bene problème alors que même l Mr a Di qu'elles avaient des différents,bayilene neup neupeul bi AK massla bou eup bi,Lou dall sene diabote yenakoko yobé dakh daguene meune setane

    • @bintacissokho5369
      @bintacissokho5369 2 роки тому +17

      Thioro c'est vrai ce que tu ya dis mère elle cache la vrai même la première qui ya parle il la dites que ya problème entre elle

    • @seynaboucamara7967
      @seynaboucamara7967 2 роки тому +16

      Lolou lagnou wara bayi neup neupeul bi

    • @bintacissokho5369
      @bintacissokho5369 2 роки тому

      @@seynaboucamara7967 mère yi gnoye tass sen keur farfarlo lagnou déf

    • @harissndiaye1820
      @harissndiaye1820 2 роки тому +23

      Merci d'avoir fait la remarque. Mère bi thi bopam bok na thi li andi thiow li fi ndakh ay affaire de neup neupeul. Mérré nako trop ko amaloul problème di ngua ray domam en plus de cela elle avait tenté de tuer le petit frère du garçon en le jetant dans une fosse sceptique nguay wakh amoiniou problèeme.

    • @amysarr9469
      @amysarr9469 2 роки тому +4

      Wallahi wakh nga degue té itam wakhat na ni khalé bi menoul dokh ndakh siti wakhat ni ay daw la guénné kone ki limou wakh eppena sakh 2wakh yow

  • @fatimandiaye8351
    @fatimandiaye8351 2 роки тому +71

    Je n’imagine pas la souffrance que la famille endure mais courage Dieu est grand qu’il repose en paix 🥺

  • @fashionrima9665
    @fashionrima9665 2 роки тому +76

    bilahi meussouma wakh gnou raye kou raye je pensais que li yeupe seytane la mais non li khole bou bone dafe si rakhe bilahi sokhore ak ignané magui dogua khame lou takh yalla ni kou raye nagnoula raye mais yalla mognou guena bakh mome mi sake mbakhe bakhale si aye diamame nanou ka défale limou beugue mome sounou borome pourquoi gnouye guena bakh sounou borome li c'est trop kou raye nanou ka raye mou fin prison pour yaraté la mais pas pour kou raye😭😭 femme bi kouka douguale prison mou raye fa kanéne kou raye moumine yalla dou bayi make raye léne ko c'est trop bilahi😭😭😭😭😭😭😭😭😭

    • @nenebodian6409
      @nenebodian6409 2 роки тому +2

      Limome sokhore leu

    • @Sherif221-YTB
      @Sherif221-YTB 2 роки тому

      *Lou doyy waar* 😭😭👇👇👇👇👇ua-cam.com/video/NHK89-Eg8ec/v-deo.html

    • @LaBarhamienne
      @LaBarhamienne 2 роки тому

      Bilahi mais topou la loi humaine bayi charia. Yallah mom adji yeurmandé gui kéne guenouko misericordieux. Mais comme nioune nio guena xam yallah adounam rek , aytia.
      Kou rey té tayko daniou la wara rey , lithi yallah wax leerna diaroul sax débat.

  • @ndeyeyacinediop5367
    @ndeyeyacinediop5367 2 роки тому +19

    P’tit ange 👼 repose en paix 🪦 yalna yalla doliniou soutoura té samal niou sounou ndiaboot yii ya rabi sokhor Ak ignane yalla naniousi yalla mousseul 😭😭😭il est temps que niou tass keur famille yii pethiorgo sou démé ba deff lii un innocent 😇 l’heure est grave 😭😭

    • @kikicamara2627
      @kikicamara2627 2 роки тому +1

      Wallay wakhaty ko keur famille ngua begeu boolé gneup g jamais pu concevoir cela na kounek dem se débrouiller lolou Moy la vie mais dafa am gnu begeu Lou yomb rek Di lakatou ci keur famille yi..nama ci yalla mousseul daal douma deuk ak kéneu kouma woolouwoul wala begoul point

  • @ibrahimacisse4474
    @ibrahimacisse4474 2 роки тому +70

    Lii dh lanouy wakh deum raay lah beugueu leuh dialléhh…Wayei yallna borom kharei aldianaa 🙏😭

  • @kardiataly7679
    @kardiataly7679 2 роки тому +109

    Va en paix petit ange 🕊🕊 Allahou akbar li métina

  • @adjafayeee
    @adjafayeee 2 роки тому +166

    Tellement petit et innocent😥 comment peut on avoir le coeur à faire celà ?? Repose en paix petit ange 🙏🏾

    • @cissramatoulaye9611
      @cissramatoulaye9611 2 роки тому +1

      Walay ndeysane mètti na

    • @adjafayeee
      @adjafayeee 2 роки тому +1

      @@cissramatoulaye9611 la peine de mort devrait être appliqué 😭

    • @cissramatoulaye9611
      @cissramatoulaye9611 2 роки тому +5

      @@adjafayeee walay fi ak lolou amoule ray doufi diouguè mome sakh dafa bonne tè nek yagui gadou sa dome time sa domou woudiou diko deff nonou ki dagne ko wara rayy ak khalè nga khamnè ndeysane niñiou yeureum teulo non li doyna warr khoudia

    • @adjafayeee
      @adjafayeee 2 роки тому +7

      @@cissramatoulaye9611 ki kay passé na bone mongui si beineine niveau

    • @amybass8022
      @amybass8022 2 роки тому +1

      Paix à son âme 🙏🙏

  • @brigadeantibidah2911
    @brigadeantibidah2911 2 роки тому +32

    Amoule balé amoule sentiment amoule maslahah amoule mboko.
    Surtout Sénégal amoule justice.

  • @toutidiop8831
    @toutidiop8831 2 роки тому +77

    Les parents irrespinsables aussi.etre pauvre ne veut pas dire do responsables.tiyè sa dome.un enfants bo togué 10mn guissoko diogal.fèkè sa beute di tegou si sa dome fo tolou...mais takhawaloi rek ak bayil xale si bede bi.cheu

    • @zeynabdiallo1744
      @zeynabdiallo1744 2 роки тому +31

      Touti diop deugg gua wakh mais kou reyy xalleh bi si keur gui la deugg 🙏🤔si keur gui la xalleh bi neekoon 🤔tantam moko dieuleeh si keur guii 😥même sa biir keur sa amofia neeko en sécurité kon gnioune fougniou dieum😭😭😭

    • @nafissatousow9156
      @nafissatousow9156 2 роки тому +11

      Yalla na yalla Def diam rek wayé 1o minutes yoyou louné khadj na si

    • @Maiimouna_G
      @Maiimouna_G 2 роки тому +18

      @@zeynabdiallo1744 vous vous imaginez heurou agn ba 19h 😢 setlou woni sakh sa doom nekoul si keur gui
      C’est hallucinant
      Djek dji talougn loudoul sen jeukeur yi
      Donté 1mn louné xadj nasi mai so télé djouk meune na am nga sauver ko

    • @bintouthiam400
      @bintouthiam400 2 роки тому +7

      Bilay ma maman elle fait ça toute le temps elle surveille ses petits enfants on dit mere sa lakale mais elle raison il faut surveiller les enfants

    • @binetakanedieng527
      @binetakanedieng527 2 роки тому +1

      @@Maiimouna_G ligua wakh rekk moyy deug sama mbokk djiguéne yi dagno doyy warr défanté rekk lagnou tall akk séne dieukeur yi mais jamais séne dom yi

  • @kharyfaye8324
    @kharyfaye8324 2 роки тому +26

    Ay li ??? Vraiment warnegn kholat souniou bop. Lougni wah niouni ibou ndafa mais bimom dou mom 🤦🤦🤦

    • @laminachon2096
      @laminachon2096 2 роки тому +8

      tant qu'on cherchera toujours un tiers responsable pour nos actes dara doubakh.
      nagnou kholat sounou bopp bakhna rek

  • @ajaniang
    @ajaniang 2 роки тому +40

    Tous les jours on parle d'insécurité après pour se rendre compte que c'est un proche 😩 naniou tapé xool yii, délou yéna wanté jaam. Yalla na Borom bi May à ses parents xolou muñ

    • @laperlecmoi5995
      @laperlecmoi5995 2 роки тому

      Li rek temps defarougnou khole yi dougnou avancé

  • @ndeyedieynabadiop4384
    @ndeyedieynabadiop4384 2 роки тому +14

    Ki Moy domerame deuggueu,ki moo bonne ki Moy deum,Massa aux parents reposes en paix petit ange

  • @cheikhseck156
    @cheikhseck156 2 роки тому +137

    c'est vraiment dure,Ada pourquoi Ada calme et doux.Mon petit ange 😭😭😭

    • @quencesskebe7605
      @quencesskebe7605 2 роки тому +33

      J ai tellement pleuré bima guicé caméra de surveillance bi manatuma té sama bop ak ni xalei bi topé si guinaw di daw heureux et innocent li dawna yaram bilae

    • @awadiasy8887
      @awadiasy8887 2 роки тому +16

      Massa il est aussi beau

    • @boudabaax8177
      @boudabaax8177 2 роки тому +1

      @@quencesskebe7605 😭😭😭

    • @neneba2601
      @neneba2601 2 роки тому +1

      😭😭😭

    • @cissebabs8961
      @cissebabs8961 2 роки тому

      Massa

  • @YayouMouhamad
    @YayouMouhamad 2 роки тому +12

    J’imagine même pas la souffrance de l’enfant 😭😭😭 massa les parents courage vas en paix petit ange j’ai le cœur meurtri 😭😭😭

  • @fatimandiaye8351
    @fatimandiaye8351 2 роки тому +22

    Comment une personne douè de raison et de cœur peut il faire ça à un enfant qu’Allah nous protège 🥺 c vraiment déchirant 😭

  • @caius6147
    @caius6147 2 роки тому +92

    Dans mon quartier les enfants de 5 a 10 ans ne font que trainer dans les rues de 8h a 19h je peux comprendre qu'avec la pauvreté les gens n'aient pas l'esprit tranquille mais un enfant ça se surveille

    • @awajupitermouchoux598
      @awajupitermouchoux598 2 роки тому +5

      Ajouté de cela la promiscuité, la négligence des parents la sauvagerie de certaines personnes capable du pire

    • @caius6147
      @caius6147 2 роки тому +13

      @@awajupitermouchoux598 effectivement d'ailleurs beaucoup de gosse se font violer par des prédateurs sexuels et une fois devenu grand la société reprochera a cet enfant d'être dans le contre nature oubliant les vraies raisons qui ont menées à cette situation.Desolé mais avoir un enfant c'est pas pour tt le monde

    • @mamekhadysy6326
      @mamekhadysy6326 2 роки тому +2

      Yiow ya wah lep bilahi naniou surveiller haleyi

    • @LaBarhamienne
      @LaBarhamienne 2 роки тому +2

      Bilahi mane yéne kogn yi soumafa diaré sama xol dafay méti

    • @caius6147
      @caius6147 2 роки тому +1

      @@LaBarhamienne guisnga dé zeyda sougn deuk mom yeurmande yalla rek mognou meuna aar mais l'espoir est moindre

  • @toufashrassoul1255
    @toufashrassoul1255 2 роки тому +12

    Svp… respectons les heures de prière… sakho niaane , douas, sarakhé, diangue kamil, laabal khôl yi… lii yepeu walahi dou néene, nitt yi andatougne ak seen sago.. faut chercher à comprendre ce ki se cache deriere ces atrocités🥲

    • @soukeynandiaye1973
      @soukeynandiaye1973 2 роки тому

      Sister wah nga deug mashallah . Li yeup sori Yala rek mokay def . Walahi koudoul diamou Yala sa hol dafay wow motah moussiba rek ngay def . Yala naniou Yala samal bopam

  • @kaderkane5775
    @kaderkane5775 11 місяців тому +1

    Repose en paix petit ange metina ay yallah mousseul nui thi sheytane amine

  • @PEOPLE-km7vr
    @PEOPLE-km7vr 2 роки тому +102

    Repose en paix petit ange, ndeysane tout innocent, khamoul dara😭😭😭😭😭😭😭.
    Yalah na yalah aare niou té sambe niou, mousseul niou si lepe louy loré amine 🙏🙏🙏🙏🙏

  • @fatoutoure7235
    @fatoutoure7235 2 роки тому +28

    J'ai le cœur meurtri walahi hazim naka gua meunei kholei khalei bou ndaw ko kham khamoul drah gua diko reyy😭😭😭😭

  • @evachou1172
    @evachou1172 2 роки тому +25

    Caméra de surveillance bakhna trop

  • @dienala1501
    @dienala1501 2 роки тому +1

    ndeysane 😢massa way li gnew na no meune timé khalé bou Ndao bi diko ray

  • @lamfadiakhate7116
    @lamfadiakhate7116 2 роки тому +23

    Inchalah ndawam aldiana firdawsi lakay agalei ❤️''qui déf Li mom adounam ak alaxarim dou am diam walahi

  • @alhouseynisanghott5366
    @alhouseynisanghott5366 2 роки тому +51

    Vraiment je comprends plus on dirait que on est plus musulman 😭😭😭paix à son âme

  • @bannasalihadieng4486
    @bannasalihadieng4486 2 роки тому +25

    Ma tite mane dieng thieye mime réwe un âge Aldiana rk inechalaaaa khalé kharitou yalle mane damaye lathie bane sénégal 🇸🇳 laniou nékk 😭😭kii déffe liii bone naaa kiii Amoule khole dhé 🙄yalle naa yalle maye saye wadioure maye kholou mouye

  • @madameboussokholofirdawsi4472
    @madameboussokholofirdawsi4472 2 роки тому +27

    Wa man liy khew thi rew mi kothi titol do nitt ray rek yalnama yalla sama ben dom bi ma diota am ak kheele yepou doyna warr 🙏

  • @AssociationAndeTaxawuGniWeredi
    @AssociationAndeTaxawuGniWeredi 2 роки тому +27

    Mai loutakh niari wakh yi nidiayou khalé bi ni danion amone problème thi afairou ndieul yaw mamam ngani dagaye rafétate ragal léne yalla

    • @dallavili5266
      @dallavili5266 2 роки тому +2

      Bayilen fofo rek nioy diaye nawfekh.

    • @annafall1770
      @annafall1770 2 роки тому +4

      Wakhal dai mère bi fake la rek nima bagné genrou mère yi nioy tass keur

    • @nannaabou6939
      @nannaabou6939 2 роки тому

      Peut-être elle n'est pas au courant magla

    • @msy8317
      @msy8317 2 роки тому +3

      Neup neupeul mo tass keur yi

    • @amyniass4511
      @amyniass4511 2 роки тому

      Ki déj nimouy wakhé rek gua khamné day neup neupeul

  • @fatouthiam6962
    @fatouthiam6962 2 роки тому +2

    Allahou Akbar mon cœur est meurtri je ne trouve même pas les mots 😭😭😭
    Yalnako y'Allah yéreume ak gni djitou gneupe té kharailéne Aldiana Firdawsi thi barké Seydina Mouhammed saws ❤
    Lii mètina trop 😭😭😭

  • @khadidiatoundiaye9804
    @khadidiatoundiaye9804 2 роки тому +2

    dama tiit sakh AK sama domou makk bou am même âge yalnako yalla samou samou bepp khalé

  • @channelchoux8236
    @channelchoux8236 2 роки тому +3

    Wa nioune bane sénégal laniou nekk legui 🙆‍♀️🙆‍♀️🙆‍♀️🙆‍♀️ nitt meuna Timé nitt diko réndi comm kharr 😭😭😭😭 loutakh mou rayyko ni

  • @ndeyegueyeloum2618
    @ndeyegueyeloum2618 2 роки тому +10

    non ki dé moy khassime nion yam lay bonne amna dou migi ak domame Ray domou diambour li😢😢😢

  • @fatimdiop4340
    @fatimdiop4340 2 роки тому +48

    ki dieuf li yalnako yalla wér inchallah 🙏🙏😭😭

  • @akaramory7441
    @akaramory7441 2 роки тому +50

    Mon frère Mathar massa yalla na motalé dawam adiana firdawsi Amine 😭

  • @mordiouf4339
    @mordiouf4339 2 роки тому +85

    Ndayyyy sann grand bii amna loukoo metii mounieul yalla baxna🙏

  • @maguetteseck3163
    @maguetteseck3163 2 роки тому +18

    Man lima diakhal moy nakala nite mana Timé moromam diko ray ,alahou akoubar

    • @mbodjifatou6353
      @mbodjifatou6353 2 роки тому

      Lolou moma diakhale mane

    • @lilydiop3455
      @lilydiop3455 2 роки тому

      Bilae iow en plus un petit être innocent🥺qu'il repose en paix ce petit ange 🕊🤍

    • @maguetteseck3163
      @maguetteseck3163 2 роки тому

      @@lilydiop3455 bilahi sama khol bi da diekh takk bo setane video bi camera bi khale biy daww di topou tanta dji bilahi bou khamonn ni dakoy ray dou demmm li metina

  • @johey4udubai798
    @johey4udubai798 2 роки тому +1

    Sougnou défoul kou raye gnou raye la li dou fi diékh. Bakane dafa fort ta Sénégal lo wakh gnon ni la "Yallah bakhna" ta topou gnou li Yallah santané

  • @massambandoye3147
    @massambandoye3147 2 роки тому +91

    Malheureusement en Afrique on pense que les fou sont ceux qui sont dans les rues les vraies fou sont dans les maisons et la famille la protège alors qu’elle a de sérieux problèmes psychologiques celle qui a fait sa n’est pas du tout bien dans sa tête un enfant de 5ans sans défense c’est dommage ❤️‍🩹

    • @SENEGAL303
      @SENEGAL303 2 роки тому +4

      Beaucoup semblent fous parceque tr simplement dagno ignane té dindi Ougnouko ci niom. Ki dagnouko wara ray. J’ai entendu la grand mère dire que la meme dame avait fait entrer un dès enfants dans une fausse sceptique. Ki domeram leu dafa sokhor.

    • @massambandoye3147
      @massambandoye3147 2 роки тому

      @@SENEGAL303 elle est malade elle n’est pas bien dans sa tête il y’a certaines maladies psychologiques qu’on banalise ici en Afrique alors que c’est un sérieux problème cette femme doit être alternée dans un asile de fou il y’a des gens bipolaires les familles le sache mais on vie avec sans traitement c’est ce qui donne ses résultats

  • @amyanneseck9541
    @amyanneseck9541 2 роки тому +138

    Repose en Paix petit ange

  • @mariamadalandadiallo8692
    @mariamadalandadiallo8692 2 роки тому +6

    Quelle méchanceté Allahou akoubar 😭qu’Allah l’accueil dans son paradis

  • @TheKnolimit
    @TheKnolimit 2 роки тому +65

    3 enfants tués par 3 femmes jalouses, dévérgondée, woudjou depuis le début de l'année... SMH

    • @toosource
      @toosource 2 роки тому +12

      Ne fais même pas confiance à ta mains gauche

    • @mamecoumbadiouf8916
      @mamecoumbadiouf8916 2 роки тому +17

      Djiguéne ci bopame lou naxari moromou djiguéname moko ko teek goor gni djarouniou rayagneté nguir yallah nagnou yéwou!!!

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 2 роки тому +3

    Ohh j'ai beaucoup pleuré en regardant cette vidéo ohh ndéysane khalé khamoule Dara

  • @larissasagna6706
    @larissasagna6706 2 роки тому +3

    Pourquoi des meurtres comme ça on accuse Dieu …??? 😭😭😭 yalla mognou ko djokhone yalla moko nangouwate yalla moko rendiii 😭😭💔💔💔 nonnn c trop

  • @ndeyemourseye6010
    @ndeyemourseye6010 2 роки тому

    Khalé sen yon nékoul si dara yalla na kipé adiana firdwsi si barké seydina mohamed psl 😭 😭

  • @mariediop3817
    @mariediop3817 2 роки тому +36

    Mais comn on peut tué un enfant innocent comme sa c cruel srx😭😭😭😭

  • @mariamagueye9084
    @mariamagueye9084 2 роки тому +75

    est ce que aussi des démons n'ont pas pris la place de certaines personnes avec le même physique. li khew légui, ça ne peut pas être l'œuvre d'humains.

    • @ndeyecoumbagueye6845
      @ndeyecoumbagueye6845 2 роки тому +7

      C ça que je me suis dite doyna ware nit gni lègui dagnon rakh dal

    • @bissentymendy4927
      @bissentymendy4927 2 роки тому +9

      Yala nagnou sounou borom doli soutoureu

    • @lissadieng5417
      @lissadieng5417 2 роки тому +11

      En tout Al Makhtoum RTA nous avez prévenu

    • @mbene-n7909
      @mbene-n7909 2 роки тому +1

      Ces des personnes sans coeur ni vergogne ya des personnes tellement mauvaises manolen xam tan k dekolene mais YALLAH BAHNA

    • @adjigueye6049
      @adjigueye6049 2 роки тому +2

      @@bissentymendy4927 allahouma amine

  • @oumoucledorndiaye887
    @oumoucledorndiaye887 2 роки тому +2

    aywayyyyy li métina peine de mort rek moko meune lidieunti li ba kagn yalla naniou yalla mousseul ci djiguéne bou bonne té am fitt massa ala famille repose en paix petit ange mon cœur saigne yalla nako yalla mbougueul

  • @ndeyeantaseck8902
    @ndeyeantaseck8902 2 роки тому +2

    Diaroul yobou police ray lène ko mome tamite mou diékh ki doméram laa way barker cheikhoul khadim souma guisone femme bi damaye ray ndayam li tamite dafa eupe trop ray rek repos en paix bb😭😭😭

  • @lyssandiaye5227
    @lyssandiaye5227 2 роки тому +2

    Bly g ds larmes aux yeux 😭😭 pourquoi un enfant innocent 😭 khamoul Dara sokhor ak bone rk motakh ga déf dieuf diou Bone bi si khale bou xamoul dara ke justice soit fait3

  • @pouneyelguisse6939
    @pouneyelguisse6939 2 роки тому +105

    Repose en paix mon chéri 😭😭😭

  • @cheikhounatine758
    @cheikhounatine758 2 роки тому +1

    ADa Mbaye Yalnako souñ borom dolli yeurmandé 🤲🏿
    -L’humain est très malade

  • @magattekholle650
    @magattekholle650 2 роки тому +2

    Goor Yalla Deugue Bou Dioyyé Nga xamni Amna Louko Métti walahi Nak ! Yalnagnou yalla Diégal sounou ay Bakkar Té def Gnou ay Djoulitttt Li doyna war Trop

  • @fatimgueye5724
    @fatimgueye5724 2 роки тому +9

    Repose en paix petit ange 😢😢 da âme niou nek si bir keur yi niou yakarni ay nit laniou té douniou ay nit motakh gor yi bolen di tak délen khôl bou bakh gni guen di yaubou sen bir keur yi ki kat khamguen dou nit

  • @momoyoutube6456
    @momoyoutube6456 2 роки тому +18

    Comment une mère peut ne pas voir son fils plus de 1h sans en rendre compte

    • @oumoukhalifandoye
      @oumoukhalifandoye 2 роки тому +5

      On me taxe de folle parceque je reste pas tranquille tant mon fils n'est pas devant mes yeux. On me dit souvent laisse le joué dehors c un garçon mais bon que dieu nous préserve et préserve tout les enfants du monde amine

  • @adjathiorombaye8200
    @adjathiorombaye8200 2 роки тому +1

    Ndeyssane li méty n’a trop 😭naka la nit meuné def li moromou nitame oh 😥 j’ai des larmes aux yeux 🥺🥺🥺😭😭😭

  • @ababacarsarr9911
    @ababacarsarr9911 2 роки тому +1

    C op vrai no 👎 no 👎 no 👎 Li dafa metti way no khalai khalai khalai no 👎 j arrive op croire
    Sénégal khana dane fiye joué. Film 🎥 tai yeugoumako 😧😭😭😭😭😭😭😭

  • @achillefatoumatagomis547
    @achillefatoumatagomis547 2 роки тому +2

    Legui gua eumb 9mois mous meti trop gua am dom gnou rayko si gratuit nak 😭lep rek mougnial, soutoural famillles mo andi li yeup
    Paix à son âme 😭🙏❤️

  • @marouanthiombane575
    @marouanthiombane575 2 роки тому +4

    limaye wakh ne justifi Pas cette meutre . Certaine vie de couple Au Senegal Sont tres compliquer. Chaque couple dois avoire une maison pour eux et leur propre enfants. Tout cest betises est causer pour des soufrance que certaine personne Vivent de jour en jour. Guir yalla koussi ammmmm diabar fondel SA famille. Sortont de nos maison familiallll surcharge . Surtout les maison avec beaucoup de couple.

  • @elysefrancelineanabassosam7635
    @elysefrancelineanabassosam7635 2 роки тому +24

    Un acte barbare😭massa petit ange innocent reposé en paix 🙏🙏

  • @laperlalaperla6646
    @laperlalaperla6646 2 роки тому +1

    Mane dhè dagne ma narone sakou ba paré Ray ma safai 5jour ta kima KO donne def dhè kham nama kham sougne wa keur ta bobou ba tey magui nopi beguouma wakhe kéne Dara dama stressé ndakhe khawma bakham dama eumb wala m dama beguone Ray ndimbalou yalla motakhe rayouma 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @babacargning9520
    @babacargning9520 2 роки тому +1

    Yalla ko wérr xalé alalou yalla la.
    Yalna ko yalla kharé aldiana si barké younanti
    bi salahou alihi wa sala
    Amine Yarra bi 🙏 🙏

  • @maimounagueye2369
    @maimounagueye2369 2 роки тому +10

    C'est vraiment triste.......Que Dieu donne à sa maman de surmonter cette douleur.....Paix à son âme..Tuer un innocent comme ça....

  • @nogayefatoufall8283
    @nogayefatoufall8283 2 роки тому +11

    Ndaysane li meitina tei doyna ware walakhi li khamougnou lanela doyna war

  • @awaseckthiaw5293
    @awaseckthiaw5293 2 роки тому +17

    woudiou péthiér go mo gueneu graw woudiou bo bokal dieukeur

  • @gamigam6420
    @gamigam6420 2 роки тому +1

    Batiment yi niou ligueye tai douniou ko theuthie laipe fi lay haiwai bilahi Ces bâtiment ne doivent pas restée comme sa c'est très dangereux 😡😭li méttina

  • @senegalesegirlll2141
    @senegalesegirlll2141 2 роки тому +32

    Perdre un enfant est une des pires douleurs du monde

  • @ibrahimacisse4474
    @ibrahimacisse4474 2 роки тому +20

    Mettinaa troppp yallnaa borom bii kharei aldiana 😭

  • @awagadiaga9553
    @awagadiaga9553 2 роки тому +9

    Thieuy Senegal Li loukofi diar 😭😭😭

  • @mamediorseck2908
    @mamediorseck2908 2 роки тому +1

    Mais Mr le Président do wakh thi li peine de mort kessé laniou soxla

  • @leylawane2898
    @leylawane2898 2 роки тому +1

    Yallah nalène Yallah maye kholou mougne si barké Alqur'an Al Karim amine Ya Rabbi 💔😭

  • @alhamdoulilah3991
    @alhamdoulilah3991 2 роки тому +1

    Lima méti moy ces meurtriers ne te diront jamais le pourquoi de leurs agissements...

  • @fatoumatandiaye2554
    @fatoumatandiaye2554 2 роки тому +2

    Il est tellement mignon le petit repose en paix mon bb

  • @mariamakamara2541
    @mariamakamara2541 2 роки тому

    J'ai pas les mots yalla na ko borom bi kharer si adjana firdawsi 😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @aminagueye1892
    @aminagueye1892 2 роки тому +1

    Bakane dafa fort kouko fate yalla fegnal la lako wax lo xamuko Sax wayer niouss leen ko si kasso bi ngiruk dundam rek

  • @OneNation591lofficiel
    @OneNation591lofficiel 2 роки тому +13

    Nooooo!!! Sebikotane ??? Li dee c’est la première fois que ma degue lolu a sebi ..hooo massa a tt la famille Diop

    • @akaramory7441
      @akaramory7441 2 роки тому

      Mane aussi c'est la première fois que j'entends une chose pareil 😭

  • @ritamendylopy9226
    @ritamendylopy9226 2 роки тому +10

    Quesqu'il se passe dans notre pays des crimes ignobles et des actes atrocités rek sans défense niata xaleh laniou raye xana xolou yeurmandeh amatoul xalehk bu xamoul darra,beury diamb, dérangé woul kene,dou lidienteh kene xamoul sahk Lou niaw nak ay xol la ligni yoretoul ay aduna metina raye xaleh moumi yak son avenir ohohoh Lou def li yalla guisnala dinala ateh ak moumi bi repose en paix mon petit ange et courage à la famille éplorée 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @tybifadiga9268
    @tybifadiga9268 2 роки тому +1

    Machallah Beau cet petit ange 👼 gspr que tu es au firdawsi

  • @ndeyediallo7609
    @ndeyediallo7609 2 роки тому

    Khôlou kiniane amna si nit yi gua bokou sa dôme teuyé co raye domou diambour nakh lane maye tougou togo nakh problémou djigeune li niawe na bouléne co bale rip bb ada yalla gua agalé sa ndaow aldiana yalla yokou kholou mouye saye wadiour yalla gua bokac seydina Mouhamed psl🤲😭😭

  • @oulysarr3193
    @oulysarr3193 2 роки тому +3

    Pauvre innocent ndeysane il a payé pour des choses qu’il ne comprend même pas.

  • @KeepingupwiththethiounesA
    @KeepingupwiththethiounesA 2 роки тому +2

    Hmmm tieuy yalla souniou borom!Deniou wouyou dji yalla deh warnaniou ko sorale dal.

  • @modoufall3194
    @modoufall3194 2 роки тому +5

    metina trop walahi
    yalnalen yalla may kholoup mougn
    te khareko aldiana firdawssi defalko mbolem dioulitt

  • @astouciss4961
    @astouciss4961 2 роки тому

    No ki no gnianffff ndeyaaam deug ( bal len ma si kaddou bi). Li kou ka ataam def do niit,égorgé 1 enfant ba paré melni koom si d rien n'était. Mw d jai mal telmen mal telmen telmen mal au coeur. Komen on peu étr 1 humain être femm de surcroît être mère. Di def Lou melni. Ki Yalla nako Yalla faay dieudieuf si ay domaam. Guèn balma akh wa salam. 😭😭😭

  • @fatoumg2905
    @fatoumg2905 2 роки тому +13

    Taye mome j ai pas les mots loudou nianale aï wadiourame kholou mougne

  • @tecofatimndiaye2676
    @tecofatimndiaye2676 2 роки тому +2

    Massa c vraiment triste un petit garçon innocent j'ai les larmes au yeux c dure bilahi

  • @sokhnafall2974
    @sokhnafall2974 2 роки тому +5

    Wa djiguène en plus Mo raye ohhhh djiguene kagne ladane def lou bonne li ohhh sama khôl metina un innocent un ange 😭 gua rayko ni

    • @masamba5646
      @masamba5646 2 роки тому

      Senegal legui moy lolou

    • @kailamentor
      @kailamentor 2 роки тому

      Le pire c'est que mom amna niari dom !!! Choquant on devrait lui prendre ses enfants !!!

  • @alalouserignetouba6190
    @alalouserignetouba6190 2 роки тому +4

    Li métti n'a trop 😭😭 j'ai les larmes aux yeux 😭😭

  • @Fatoumbodji459
    @Fatoumbodji459 2 роки тому

    Yalna ko yalla yerem té kharé ko aldjana ya guene kawé Inshalah té oyofal souf si kawam Inshalah yalna agalé ndawam aldjana Inshalah

  • @seynabouseck9633
    @seynabouseck9633 2 роки тому +1

    Bâtiment yi yégoul yi lagnou wara wakh ndakh lep silay khéwé vraiment li dafa gnew trop😭

  • @damesene2939
    @damesene2939 2 роки тому +16

    Xam nga li metina nanouy xol guinouy tak wolof dafa wax kou for diabar rerlé dome

  • @ndeyeamydiallo9581
    @ndeyeamydiallo9581 2 роки тому +6

    Mane sans froid bi nit yi di ame bougnou rayé nite ba paré moma diakhale trope

  • @fantacordroch8645
    @fantacordroch8645 2 роки тому

    Aye waye li gnaw na c’est vraiment triste et dommage délén khole sén doom yi mane dama khamoul li diam la mélni vampire ni 😭😭😭

  • @khadyjakonate9039
    @khadyjakonate9039 2 роки тому +7

    Mangi imaginé douleur bi khalé bi wara dounedou,😭paka thi Bate ohh 😭😭😭

  • @khadygueye5714
    @khadygueye5714 2 роки тому +1

    Bilahi bessou penthie mah dina méti trope Yanagnou yalla yeureum té yéxëniou

  • @madamembodj6658
    @madamembodj6658 2 роки тому

    Que la terre soit légère 😭😭yayam aussi yallah nako ko yallah défi mou antaane ko si barkei nabi 😭😭😭😭👼🏾

  • @bernilynsha
    @bernilynsha 2 роки тому +2

    Massa vraiment sama khôl diekhna takeu si liii 😭 petit trésor repose en paix 🙏🏾courage à toute la famille amoul masla n’a yone def ligueyame

  • @ast8347
    @ast8347 2 роки тому +1

    Massa Tonton mètina Yallah yokoulène kholou mougn

  • @fayebiram3003
    @fayebiram3003 2 роки тому

    Lou way def bopame ki yalla moko fénial rek mane dama diomi 😭 ada yalna la yalla yeureum yalna gua aguali sa ndaw aldiana firdawsi si barké serigne babacar sy