Nitt kou gnoul surtout gni pauvre ils sont fort en faire des enfants mais pas en prendre soin . Diour rek lanioufi nekei tei dougn topato sen dome yi surtout les garçons les parents les négligent beaucoup c’est triste
@@Enoushka7772wakh nga lep.certains amougnou dara beuga def diour sources de revenus.Manan pour gnom sou xalé yi magué dina am gnouthi tekki diékhal séni problémes.
Bo wakhé niounane yok khétou séydina moukhamed thé douniou dieul résponsablité thie khalé yi ndéyssan gni liniouy déf nékhoulén yalla nalléne yalla guéné thie dundu by
Chapeau à vous Séne News ,de vrais professionnels.Le pays a besoin de média comme vous ,Ce genre de reportage est des meilleurs pouvant aider nos autorités à se concentrer sur le vécu quotidien des sénégalais.Ces jeunes ont besoin d’aide et vous avez montrer la voie,en les dénichant dans les bas fonds .Merci
Certains commentaires je me demandes si ce ne sont pas des enfants de 4 à 7 ans qui se cache derrière leurs écrans car vraiment y'a des propos qui ne sont pas digne d'un adulte...ces jeunes ont besoins d'aide peut importe nignou mel ce qui se passe autour d'eux les affectent psychologiquement et on c tous k xel moye leep s'ils étaient dans de bne conditions kone douniou sêtane émission bii badii commenter
Le 2e interrogé qui bégaie le journaliste ne l'a pas compris, je pense que dafa nei fakhoul da nieuw pour di forr ferraille parcq dafa sokhla 75mil pour dieund bâche(je pense) pour liguey gaale. Je pense que il a aussi dit que moll la
Attention aux émotifs, ces genres d'enfants ont une psychologie spécifique. Ils sont capables de te duper pour leurs intérêts. Ils sont hyper intelligents mais manipulateurs. L'état doit revoir les centres sauvegardes afin de les récupérer, ensuite les redresser. Il leur faut un accompagnement psychologique, une formation professionnelle et un bon encadrement, avec rigueur, pour certains pour pouvoir les récupérer. La responsabilité des parents est également interpellée.
Barki alkhourane Parent yi sonnou naniou yalla naniou yalla sammal boppam te niom yalla sam len delo len si yon bou bkh bi bilay bonnou niou danio amoul koulen tekk si yon rck
😭😭😭😭😭😭😭😭😭Ayway vous qui le pouvez surtout les gendarmes, récupérez le jeune de 15 ans vivant avec sa grand mère et veut devenir militaire en passant à la prytanie. Toute mère sera choquée en voyant et écoutant ces jeunes. Yala nalène Yalla deup tek len si yonou siratal moustakhim
Le jeune homme qui fait du rap est tres intelligent. C'est un artiste qui improvise avec facilite en parlant naturellement de son vecu...Tellement triste de l'entendre. Ils ont tous besoin d'aide.
j'ai le cœur qui saigne qu' Allah veuille sur vous. ces enfants sont tous issus de familles monoparentales. Ils sont victimes des leurs parents irresponsables, des enfants on en fait pas si on ne peut pas s'en occuper
ils ont juste besoin d'aide peut importe nouniou mel s'il était dans de bonne condition chez eux kone dolêne meusseu xam badii commenter en plus il y'a un niveau de maturité qu'ils n'ont pas encore atteint c k Sénégalais pour mome toubab rek mo am droit consulter aye psychologue ou truc du genre les problèmes qui circulent autour d'eux les ont atteint psychologiquement...sister on ne réagit pas tous de la même façon face à nos problèmes y'a bkou de gens qui souffrent mentalement teii xel moye diriger lepp
Ils n'ont rien fait de mal ,sénégal mo bari niouye diour dome te dougnou dieul sen responsabilité,beugue dome you bari te daleu sakh dokoko dieundeul khana baye lepou yaye bou sonne bayi khaleyi fakh ,sénégal lifi nek bokoye wakh dou diekhe je suis désolé...diour yobou dara sanni wala sani thi biti te khale mome loumou khas ba tamou bayiko dou yombou
Yalla nalene yalla takhawou bagnou delouwate ak sene sago ,les structures qui doivent prendre en charge ces jeunes font défaut au Sénégal et pourtant ils ont droit a la santé, à l'éducation à la protection, bref ils ont droit au bonheur à la dignité, à l'occasion à chaque fois que je passe derrière le tribunal je leur laisse quelque chose ...yalla nalene yalla sameu 😢😢😢😢
Yallah nalene yalla sopi Bidiay Seydina Mouhamed S.A.W.S
Sallahou halleyhi wassalam 💘💘
Mon cœur saigne 😭😭j’ai trop mal pour eux
Nitt kou gnoul surtout gni pauvre ils sont fort en faire des enfants mais pas en prendre soin . Diour rek lanioufi nekei tei dougn topato sen dome yi surtout les garçons les parents les négligent beaucoup c’est triste
Dom alalou yalla la
@@aliounegueye3076ba keneu waroulene topato diourr rk sa di si mbedeu bi
Bien dit frére
Bilay bo amoul dara waro nekk di diour rekk
@@Enoushka7772wakh nga lep.certains amougnou dara beuga def diour sources de revenus.Manan pour gnom sou xalé yi magué dina am gnouthi tekki diékhal séni problémes.
vraiment émouvant, k'Allah veille sur eux,ils sont très jeunes, prières pr eux et merci à Sen News,amna solo trop
Thiey yalla yanaleen yalla mouthieul 😭😭😭😭
Allahumma Amiiine Yâ Ar'hama-r Râhimîn
Sa yaye bou soné do dem liguéyi yi moguen ndakh fakheu diko gueneu yokeu n’a khar 😢
Bo wakhé niounane yok khétou séydina moukhamed thé douniou dieul résponsablité thie khalé yi ndéyssan gni liniouy déf nékhoulén yalla nalléne yalla guéné thie dundu by
Bilay yaw
Amine yarabbi 👏
J t di
Mention.tres bien senenews tv , voilà des reportages pour aider le pays à avancer ❤
Niarry boy yi papa le pêcheur Ak benen boy bi ki beuguoul dém guinne ils son récupérable vraiment 😢
Ms aussi boy bii sou dème guinne Dina bayii lepp
Billaye
Ndeysann il insiste à dire sougnou borome reik moo khamm 😭Konn yalla nala borome bi dimbali woneleu yonn bi akk yeine gneup 🙏🏽🙏🏽
Bilahi wadiour you beuri séni domes dinagnelen dougueul safara😢😢😢😢di diour rek tei do topato, chiiim
Papa est un pêcheur !!! Il est récupérable !!! Une bâche de pêcheur coûte 75000 !!! Svp orientez le à cayar !!!
Vous avez compris mon cher
Sou bénén yoné délén protéger visage boy yi mo geuneu réfét
C’est bien fais niou wonner sa visages yi peut être senn parents yi guislenn nah niou xam finiou nekk sah😢
Boy bi neki ak mamam kou yewou la ci lima guiss kou dimali mou tegou thi yon dh
Teyna dalna te soko ladie waxou nitt lalay tontou mais rappeur bi mom daguay wax 1+1 moune la 10😂
Ndaysan yalnalen yalla takhawou❤
Salam alhamdoulilah magui ziar gneup massa khol bou nakhari rek khaleyi yalnalene yalla takhawou diapaléne tek lene lokho si barke seydina mouhamed 🤲🤲🤲🤲😭🙏
La direction de l'administration surveillée doit faire une descente et récupérer ces jeunes en detresse
Bravo pour ce reportage qui reflète la réalité dans certains endroits de la capitale. Qu’Allah les assiste
Chapeau à vous Séne News ,de vrais professionnels.Le pays a besoin de média comme vous ,Ce genre de reportage est des meilleurs pouvant aider nos autorités à se concentrer sur le vécu quotidien des sénégalais.Ces jeunes ont besoin d’aide et vous avez montrer la voie,en les dénichant dans les bas fonds .Merci
Ndeyssane khaleyi koulene diapale mou bakhe Walahi monsieur le président Diomaye Faye et son premier ministre Ousmane Sonko diame lene si nguir yalla
Machalah très importante cette émission bravo 🙏😎
Le gars qui rappe a vraiment besoin d'aide 😢
Walay
Merci frère qu'Allah les vienne en aide
Yalna nalénn yalla diapalé si brk mhmd Rassoul
Xalei denio droguewou ba meunouniou wax il faut une d'intoxication
Je posais la question !
C’est vraiment triste ndakh gni ay xaley négn
Que Dieu leurs viennent en aide !🙏🏾🙏🏾
Bilay yaw😢😢😢
qu'est ce que t'en sait bayil lene di doul yako guiss ioe yaye doukate deug
Ils on vraiment besoin d’une réinsertion sociale
Qu’Allah les viennent en aide
Le plus cohérent d'entre eux est celui en rouge. Quand il a dit Prytanée militaire sama yaram da daw😢il est très intelligent ndeyssan
Bilaye mome beugue na bakhe
@@MouhamedKebe-r9l bilay yaw🤧
Il faut aider ces jeune
Emission bou am importance ak meuné avancer lo deuk bi bravo
Les autorités doivent tout faire éradiquer ça
😭😭😭😭yalla sounou borome maa ngui layy gnann haleyi yalla ngaa lennn guinddi tè dello lennn senn ayy mbokk
Amine ya rabi
Sounou rak yi Yalla nalen Yalla tek lokho Bilae metina
Que Dieu les vienne en aide
Ken beugoul bone ❤
Bilahi yallah rek mo ham😭😭😭yallah naniou borom soutural
Certains commentaires je me demandes si ce ne sont pas des enfants de 4 à 7 ans qui se cache derrière leurs écrans car vraiment y'a des propos qui ne sont pas digne d'un adulte...ces jeunes ont besoins d'aide peut importe nignou mel ce qui se passe autour d'eux les affectent psychologiquement et on c tous k xel moye leep s'ils étaient dans de bne conditions kone douniou sêtane émission bii badii commenter
Boy bi Di expliquer si taw bilahi mongui wakh Lou am solo barki cheikhoul khadim il faut bien regarder cet émission et aidé c'est enfants
Le 2e interrogé qui bégaie le journaliste ne l'a pas compris, je pense que dafa nei fakhoul da nieuw pour di forr ferraille parcq dafa sokhla 75mil pour dieund bâche(je pense) pour liguey gaale. Je pense que il a aussi dit que moll la
sisi lolou la wakh😢
Wadiour bou manaloull darà domame yenna yorell khaleyi ake matoulen Wadiour momm noooooò 😂😢😮😅
sénégal diour ak abandone dome xale bou tole nii ndax le dege la banditisme sathie yar len sen diabot yi 😢😢😢😢😢astafourlakh yalna len yalla sopi
L'Etat doit prendre ses responsabilités en enfermant tous ces enfants de la rue dans un centre de redressement
Merci pour ce reportage au moins quelque chose d utile
L état doit réagir et vite sinon ils seront perdus
Attention aux émotifs, ces genres d'enfants ont une psychologie spécifique. Ils sont capables de te duper pour leurs intérêts. Ils sont hyper intelligents mais manipulateurs. L'état doit revoir les centres sauvegardes afin de les récupérer, ensuite les redresser. Il leur faut un accompagnement psychologique, une formation professionnelle et un bon encadrement, avec rigueur, pour certains pour pouvoir les récupérer. La responsabilité des parents est également interpellée.
Barki alkhourane Parent yi sonnou naniou yalla naniou yalla sammal boppam te niom yalla sam len delo len si yon bou bkh bi bilay bonnou niou danio amoul koulen tekk si yon rck
Ndeysan 😢😢
J ai le coeur meurtri bilahiii
Yalnaleen sunu Boroom Gindi bangéén déllou seeni waajour
Thiey serigne Touba 😔
L'état doit créer des centres, pour sauver ces jeunes, c'est vrai que y'a des parents irresponsables mes la plupart des enfants aiment la délinquance
Deyssane ils ont besoin d'aide !!!
Rappeur bi kou tégeul ndayame mou dieul 😢❤
Mdr
🤣🤣🤣
Wahal dé 😂😂😂 volet bé meti 😂😂
Sheu😂😂😂😂😂😂
Kii reww rekk moko diap
Papà you niafe senn daye amoule diarigne
Loumay dioy😢😢😢😢
😭😭😭😭😭😭😭😭😭Ayway vous qui le pouvez surtout les gendarmes, récupérez le jeune de 15 ans vivant avec sa grand mère et veut devenir militaire en passant à la prytanie. Toute mère sera choquée en voyant et écoutant ces jeunes. Yala nalène Yalla deup tek len si yonou siratal moustakhim
Je suis un homme musulman déh, mais le principal problème au Sénégal c'est la Polygamie. Malheureusement!
Ndeysane li nena militaire la beug nek
Yalna len yalla tahawou si barké seydouna mouhamed psl
Merci wa senenew
Li risque deugla si reiw wallahi
😢yallah na yallah sambe té guindiléne
C'est vraiment grave
Bocou de gens envoi leurs enfants pour fuir leur responsabilité
Un enfant qui pense allé au pritani militaire.
Vraiment mérite une assistante
Vraiment c'est dure merci pr cette reportage sur les jeunes et bonne continuation à toi l'état doit aidé la jeunesse
Le jeune homme qui fait du rap est tres intelligent. C'est un artiste qui improvise avec facilite en parlant naturellement de son vecu...Tellement triste de l'entendre. Ils ont tous besoin d'aide.
j'ai le cœur qui saigne qu' Allah veuille sur vous. ces enfants sont tous issus de familles monoparentales. Ils sont victimes des leurs parents irresponsables, des enfants on en fait pas si on ne peut pas s'en occuper
Liguey bi amna solo yallanalene yalla dolli diam
yalnaléne yalla sopi si barké yonéntebi 🤲
Saway yaw dou rab yi dé dadj yi rék la👍
Vraiment journaliste diabare la❤❤❤
Merci mon frère sa kaw sa kanam.❤
Khaleyi. Da. No. Bou ngua. Bonne. Reck. Niack diome
ils ont juste besoin d'aide peut importe nouniou mel s'il était dans de bonne condition chez eux kone dolêne meusseu xam badii commenter en plus il y'a un niveau de maturité qu'ils n'ont pas encore atteint c k Sénégalais pour mome toubab rek mo am droit consulter aye psychologue ou truc du genre les problèmes qui circulent autour d'eux les ont atteint psychologiquement...sister on ne réagit pas tous de la même façon face à nos problèmes y'a bkou de gens qui souffrent mentalement teii xel moye diriger lepp
@@alexismendy8809DEUG nexoul wayyy bien dit
Situation très très compliquée
Yallanalel yalla sopi si barke yalla
Les parents en générale fuit leur responsabilité je suis vraiment désolée
Mane Magiu dioy rèk 😢😢😢😢
Yalla nalen yalla tahawou
Oooooh massa 😢😢😢
Yallana Yalla moussal si wadiour bou demissionè
Bouma manon' diott boy Guinée bi... Stp fokk niou renforcer éducation wammm... J'habite à mbour si c possible
Yalla nalen Yalla mouthieul tei tek Len si yoon bou bax Yalla baxna metina dh
Yalna lenn yalla diapalé 😢
😭😭😭😭😭😭
😱😱😱😱FAIBLESSE DES AUTORITÉS. IL FAUT ÊTRE FERME POUR REDRESSER CES GOSSES À LA DÉRIVE. 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Gos bi minguiner dour sen emission bi amna solo ay way dieuler len fi
Sénégal diour di dadjalei laniou wara bayi si bopam bilahi nioussi beuri douniou dieul seni responsabilité
Ndeysane c triste wollah 😢
Il faut aider les enfants c vraiment triste
Ils n'ont rien fait de mal ,sénégal mo bari niouye diour dome te dougnou dieul sen responsabilité,beugue dome you bari te daleu sakh dokoko dieundeul khana baye lepou yaye bou sonne bayi khaleyi fakh ,sénégal lifi nek bokoye wakh dou diekhe je suis désolé...diour yobou dara sanni wala sani thi biti te khale mome loumou khas ba tamou bayiko dou yombou
Ndeysanne Yalla Nalenne Yalla Takhawou Banou Dellou Seni Diwane
😢😢😢😢😢😢 oh ndeyssane
Ndeysane yalnalén yalla walou keneu beugoul deuk si mbédeu mi keneu beugoul boon la pauvre et la fuite de responsabilité mo andi li yeup
yalla nagnou yalla doli soutoure mais yaye yi surtout nagnou gueneu farlou si sounou dome yi ndax li baxoul si rew
Journaliste bi sa numero svp la sohla le plus rapidement possible
Yalla nalene yalla takhawou bagnou delouwate ak sene sago ,les structures qui doivent prendre en charge ces jeunes font défaut au Sénégal et pourtant ils ont droit a la santé, à l'éducation à la protection, bref ils ont droit au bonheur à la dignité, à l'occasion à chaque fois que je passe derrière le tribunal je leur laisse quelque chose ...yalla nalene yalla sameu 😢😢😢😢
Parent yii nioy daw sénn responsabilité 😢😢😢
Deflene cagnotte yene gniko meun diokh ko wa sene news gnou diapalé lene gnou fadiou tog ligey
Domarame yi di diour di teke reke te manolo lenn sarape dayame douguen rouss sakh domarame kilifeu
Tu expose des jeunes qui ne sont des bandits ni des agresseurs guay saltél image boyi nii... bordel ! Démissionne parental total😢😢
Ndeysane 😢