Voilà un jeune vraiment fier, authentique et brave. Il est 10000 fois beaucoup plus humain, respectueux et respectable, très sage et motivant. Tout ira bien inchallah garde ton optimisme et ta foi . Dina bakh inchallah.
C'est dommage qu'au Sénégal ils minimisent les personnes handicapées, ici en Allemagne ces personnes sont très respectées et les entreprises ont l'obligation de les insérer et les embauchés. Ils travaillent dans tous les domaines ❤
Il faut être inconscient, sans foi et sans cœur pour se moquer de lui. Voici un jeune très fort d esprit qui accepta la volonté DIVINE car ça peut arriver à n importe qui. Bravo
Force à toi frère, sa histoire metina trop , nék lirr bu am 3 jour am accident lakk, khamga ni lolu rawna méti. Les gens qui se moquent de toi n'ont rien compris d'Alla le tout puissant
Svp finançons le MONSIEUR LE PRESIDENT MME MARIEME FAYE SALL YOUSSOU NDOUR WALLY BOUBS SIDY DIOP YERIM.SOW ME DIOR DIAGNE MONSIEUR OUSMANE SONKO NGIR YALLAH DJAPALERLENEKO AZIZ NDIAYE BALLA GAYE MODOU LO BAYE NDIAYE AWA BALDE ADJA DIALLO VIVIANE TITI ADIOUZA ISMAEL.LO BABA MAAL COUMBA GAWLO
Nioune warnaniou kholate sounou bopou. Allemagne la diangué mais bimou nieuwé Sénégal ba legui diangoul ndakh nimou mél. Hypocrisie bi nék fi dou fi gawa diouk.
On le connais sous le nom de pape dawoul diouk balacoss c vrai souniou khalé keur la dane andal t ragalouniouko dawouniouko machallah ame joie de vivre ba d
Un grand!! Bravo!! A lala et a dakar buzz, vs faites Un exellent!!!!!! Boulot!!!!! Vs avez du merite!!!!!!! Je vs felicite!!!!!!!!!!❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mais sènègalais yikay khass c koi leur problèmes amna niou bone beug wah djou bone yeurmandè dra amouniouko nitt kenn douko trokhal sheuttt courage mon frère yalla djèkhoul 😢❤
Courage frère dieu est avec les endurants… nous parents soyons plus vigilants comment peut on laisser un bb de 3 jours seulement tout SEUL vraiment c’est inadmissible bien que c’est ton destin yal nala yalla tahawou
Ndaysane sénégalais dou nit sax wollah dagni wax nit kou wekh mais niom nio nara eup aldiana massa bro qu'Allah t protège may la lep lo beug sa adouna force à toi cheri
Qui rira bien rira le dernier dounde gou diekhagoule loune' khedje na thie. Celui qui na pas encore atteint l'autre rive ne doit pas se moquer de celui qui se noie
Massa bilay massa boulenn falé yala Moy dogual yalna yala delola sa kanam inchala massa je suis très touchée massa bilahi togne bakhoulll moukk massa Dara nekoul si yaw du moment que tu crois en dieu soit fort très fort ❤️💕💕💕💕💕💕💕❤️💕❤️
Sois toujours reconnaissant envers Allah mon frère. La vie d’ici bas n’est qu’épreuve. qu’Allah te préserve et te facilite facilite les choses de la vie. Dakar buzz japalé lene ko niou japeuh si.
Voilà un jeune vraiment fier, authentique et brave. Il est 10000 fois beaucoup plus humain, respectueux et respectable, très sage et motivant. Tout ira bien inchallah garde ton optimisme et ta foi . Dina bakh inchallah.
P
Vz❤
Vz❤
Svp lançons une cagnotte pour l aider lou way am hebougnou dara MOHAMED du courage de tt cœur avec toi
T'as raison. Meunn neugn ko opérer en Occident.
Yala nala yala tahaWou j
Wawe yawe naniou organiser lolou baxame heuyna moutaxawe
Présente
Merci beaucoup à vous
Je suis en Europe mais Bilahi Sénégal rek lay degg wala guiss gnouy retaan genre nitt yi
Force à toi Broh ❤🎉😢
galsen rek la am waaye guemeul sa bopou rek yalla bakhna te guisna lep
Tarder rek
En fait s'il était tjrs en Europe dher mou bakh
Bilahi wakh nga deugeu wou tee ak toubab yi danio âme yeureumende âme wou teee ak Sénégal bou deugeu.... Yalla bakh n'a
Gni koye re dagnou .khamoul rek soit fière et digne dieu et grand yalla nalla yalla takhavou
Dieu
masha'Allahu yalla baxna
Ceux qui se moquent de lui ne sont que des imbéciles qui n'ont aucune humanité
Wa ki lane mo.nek thi mome non Sénégal degni yok stress yalla na la yalla takhawou frère ❤❤❤❤❤
Sénégal kay dagni yokou febar wala stresse bilahi
Mouhamed tu es un homme comme nous. Bas toi.
Bilahi ndeysaan
Je ne l’ai pas connue avant, c’est la 1ere fois que je le vois mais il a un beau sourire❤. Il doit toujours sourire 🥰🥰🥰
😭😭😭😭😭😭😭👏👏👏👍👍👍👏👏
Oui c c'est que je disais son sourire😊
Eduquons nos enfants c'est le meilleur héritage qu'on peut leur offrir. Cet enfant est très courageux.
Ndeysane yallana la yalla défal diameu si barké seydina mouhamed psl ❤
Salam alhamdoulilah magui ziar gneup massa mon frère yalnala yalla diapalé defal la lep liga beug si barke seydina mouhamed 🤲🤲🤲🙏🙏🙏
Je t adore mon champion tu es super intelligent brave eduque en avant
C'est dommage qu'au Sénégal ils minimisent les personnes handicapées, ici en Allemagne ces personnes sont très respectées et les entreprises ont l'obligation de les insérer et les embauchés. Ils travaillent dans tous les domaines ❤
bilaye
Machalla kontane ci yaw ndakh serigne fallou kontane ci yaw ndakh sa courage bilahi
Tu es un homme courageux Yallah nala yallah takhawou
GEUMAL YALLA XAM SA BOPPOU RÉK INCHALLAH DÉY BAKH TÉH MANE MI SAKH DI WAKHE AK YAW YAMA GEUNNE BARKI CHEIKHRA FALL❤
Machaallah beuri nga djom am fouleu ci sa bopp ,amnga yarr en +yallah dinaleu djapaler inchallah
Il faut être inconscient, sans foi et sans cœur pour se moquer de lui.
Voici un jeune très fort d esprit qui accepta la volonté DIVINE car ça peut arriver à n importe qui.
Bravo
Sa me brise le coeur yallah gua tanei ak diam amine 🥺🤍🤍🤍
In challah 😭😭
Machala mouhamed que le bon dieu vous garde bon courage massa
Manchallah Mouhamed borom tour bou séleu bi. Ndoundeul mon fils.
Thiey yalla sénégalais mo meuna khebaté té meuneu daw kou weradi bilay gnak yeurmandé bissi rewmi yem nama yalla la na yalla defal diam 🙏
Du courage que la grâce de dieu soit avec toi ❤️
Yalla dou tek natou kouko atanoul courage ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Force à toi frère, sa histoire metina trop , nék lirr bu am 3 jour am accident lakk, khamga ni lolu rawna méti.
Les gens qui se moquent de toi n'ont rien compris d'Alla le tout puissant
Svp finançons le MONSIEUR LE PRESIDENT MME MARIEME FAYE SALL YOUSSOU NDOUR WALLY BOUBS SIDY DIOP YERIM.SOW ME DIOR DIAGNE MONSIEUR OUSMANE SONKO NGIR YALLAH DJAPALERLENEKO AZIZ NDIAYE BALLA GAYE MODOU LO BAYE NDIAYE AWA BALDE ADJA DIALLO VIVIANE TITI ADIOUZA ISMAEL.LO BABA MAAL COUMBA GAWLO
Wallahi yallah rk mo xame li taxe mou lak gnikay rétane tamite nk yallah dinaléne fay s'en bor 😢😢😢
SANTE YALLA RÉK YALLA BAKHNA INCHALLAHOU RABI LÉPPAY BAKH BARKI NABIL MOUSTAPHA CHEIKRA FALL
Courage mon frère qu'allah veille sur toi et sois heureux
mais pourquoi se mosqué de lui😢 il n'a rien du tout en plus il est intelligent Machallah ❤❤
Momaa diahall😢
Bilahi il n'a rien de méchant et il va réussir inchalah.
Sénégalais Mo rew de nature. Lolou motax Kou différent rek niou sonal ko😢
Hiper intelligent ❤
Non kiii kaye macchhall dafa yewou de trop macchhall âme khel
Machalla Mouhamed kou guem yalla ngua❤️❤️ kofi guenoul guenoula 😘 je suis très fière de toa 🥰🥰
Il est très intelligent Machallah
Nioune warnaniou kholate sounou bopou. Allemagne la diangué mais bimou nieuwé Sénégal ba legui diangoul ndakh nimou mél. Hypocrisie bi nék fi dou fi gawa diouk.
Walay hanzim yalla molaka takha wakh liii metina trop
Bilay niaw na trop Sénégal daguay warou
On le connais sous le nom de pape dawoul diouk balacoss c vrai souniou khalé keur la dane andal t ragalouniouko dawouniouko machallah ame joie de vivre ba d
Quel témoignage écoutez bien ses paroles qui vaut d l'or aidez le svp
Wallahi Frr yallah dinla teral in challah 😭😭
Non pourquoi école yii bagn ko djiel gni nak gno bonne waay daay tital khallé yii eskeu khalé yii gnoko geune nafekh ba dé courage frère yow dé ci gnoune gan bokh outé wugnu dara.❤❤❤❤ Nagnou dello sougnu xel doundou bou sotégut lou nekh hédjie nasii😢
Réetaane niit tchi mëlookaanam pour lan .
Ignorants, gnaak yaar ak khôlou Yeureumandê YALLAH nagnou tchi YA RABI Mousseul .
Tei nak, dounde bou sooti woul lounê khadjieu naatchi ..
Bilahi Walahi Watalahi darà sakhoul dou wéer , dou amam amam , dou taareu, dou darà.
Ame nga diomeu MASHA ALLAH TabarakAllah Mouhamed.
YALLAH naleu YA RABI Takhawou banga motali sa Yeinei tchi say Waydiour TCHI BARKÉ SEYDINA MOUHAMMAD ALEYI SALATOU WA SALAM ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ .
Senegal dou deuk
Je vois un sage frere yaw keneu dotouleu togne inchalla kouleu ❤❤
Yalla nala yalla taxawou si barké seydina Mouhamed psl 🙏❤️❤️
Boulén fallé lou ame yalla laa courage ❤❤❤❤❤
Mes respects, votre force mentale est motivante pour tout le monde,yalna yala defal la diam ak héwal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Big respect ✊🏾 bro reste comme ça
Ndeyssane ñiit mbindoul bopam yalla moye mbinde allahamdullillah nala yalla takhawou
😢😢non pourquoi am gnou nittéwoul, pourquoi nioukay saga, il est plus humain que certaines personnes walahi, qu'Allah te protège Mouhamed🤲.
Yalnala yalla takhawou arla samela dina bakh inchala 🙏🙏🙏
Un grand!! Bravo!! A lala et a dakar buzz, vs faites Un exellent!!!!!! Boulot!!!!! Vs avez du merite!!!!!!! Je vs felicite!!!!!!!!!!❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
La beauté n est pas dans la figure mais la beauté vienne du coeur
Merci bcp toma❤️🫶
Machalah et pourtant il a un joli regard ❤
❤❤❤yalana yala walou si sa barke yayd walou
Fiere de toi du courage dieu est là pour tout le monde
Inchalah digua téki ale gouda fann inchalah ❤❤❤ moi je t'adore
Du courage frère yalla nala yalla sameu kharela défal la diame
Sénégalais moy nafékh piir mé dra toussss lansi meunoul tu va réussir inchallah
Jum je suis derrière tw je suis fier de Tw bon continuation
Sama bocou ndar ndar la ndeysan senegal dafa mété doundeu Bilaye dagne oute connexion rien k pour torokhol domou adama yi Bilaye 😭😭
Mais sènègalais yikay khass c koi leur problèmes amna niou bone beug wah djou bone yeurmandè dra amouniouko nitt kenn douko trokhal sheuttt courage mon frère yalla djèkhoul 😢❤
Tu es très brave machallah yalla nala yalla defal diam guemeul sa bopou rk j t’adore🥰
Vraiment je suis ravie d'avoir découvert cette formidable personne
Ndeysane frére boul falé kén kou lay ngagni yalla bakhna inchallah yalna la yalla samou inchallah
BILLAKHI WAAL KITABI YAW DINGUEU AMM LOU BAKH NDAKH AMNGA GNANOU WADIOUR TÉÉ ABB TABBÉ NGA KOUY DIOKHÉ THIE LINGA YORR BOUR YALA DILA DIOKH LOO DIOKHÉ ÇA IRA INCHALAH FAUT JAMAIS BAISSER LES BRAS MON CHERS ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalla nalla ÿalla diapalé maye la kheweule ak teranga bou barri thi barké seydina Mouhamet PSL amine incha allah bonne continuation du courage
Respect mon frère ❤ suis fier de toi
Boul masa décourage yalla bakh na lépou dina bakh❤
Inshallah Dieu est grand et il est avec toi ❤
Courage frère dieu est avec les endurants… nous parents soyons plus vigilants comment peut on laisser un bb de 3 jours seulement tout SEUL vraiment c’est inadmissible bien que c’est ton destin yal nala yalla tahawou
Yalla defa diame soutour t'es arre ci Barker seydina mouhamd ❤ yalla beta l'argent baka térre ça famille merci long vie à toi et toute la famille
Ndaysan daga bakh ms yallah bkh
Ndaysane sénégalais dou nit sax wollah dagni wax nit kou wekh mais niom nio nara eup aldiana massa bro qu'Allah t protège may la lep lo beug sa adouna force à toi cheri
Courage frère le meilleur reste à venir paix sur toi
Ndeysane force à toi mon frère 🤙🏿🤙🏿🤙🏿🎉🎉🎉🎉❤️🤍❤️🤍❤️🤍❤️🤍❤️🤍❤️🤍❤️🤍💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿
Yallah neleu yallah mey goudou fane ak wergeu yarame lo beugue yallah neleko yallah defeul diame thi yaw, abonnel thi mome tik tok kou bakh leu ❤❤
Si nioune gua bokou wouté wouniou Dara ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Yalle moye binede domou adama Alhamdoulila yangui ak sa bakane courage frere 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
L indicipline au Sénégal me dépasse,on fait que insulter dans les réseaux sociaux.
Mouhamed mon fils de cœur tu es très courageux dit na la woow insha allah ❤❤❤
Qui rira bien rira le dernier dounde gou diekhagoule loune' khedje na thie. Celui qui na pas encore atteint l'autre rive ne doit pas se moquer de celui qui se noie
Machallah Serigne Mansour Yalnaniouko Yalla fayal ❤
Du courage frère meitina mé lou yalla deff moh gueune Sénégal mom monguini da ngaÿ nék sii tolof tolof gnoulay roubei mé doundou bou soteigoul lounei khath nasiiiii soit fort 🥰🥰🥰
Yalla nala yalla défal diam
soit fort que dieu te protège 🤲☝️
Courage frerot que Dieu te donne la force de vivre
Massa bilay massa boulenn falé yala Moy dogual yalna yala delola sa kanam inchala massa je suis très touchée massa bilahi togne bakhoulll moukk massa Dara nekoul si yaw du moment que tu crois en dieu soit fort très fort ❤️💕💕💕💕💕💕💕❤️💕❤️
Qui n'a pas gagné l'autre rive ne doit pas se moquer de celui qui se noie. Il n'y a qu'Allah Soubhana Watalah qui connait l'avenir.
Je vous j'adore Mouhammad.
Ich wunsche dir alles gute zum leben.viel gluck une gute reise.
Sois toujours reconnaissant envers Allah mon frère. La vie d’ici bas n’est qu’épreuve. qu’Allah te préserve et te facilite facilite les choses de la vie. Dakar buzz japalé lene ko niou japeuh si.
Metina torop yalla bakhna mouñal dina bakh ❤❤❤❤❤❤❤❤
Courage mon frère nous sommes tous des humains
Merci beaucoup a vous tous pour le encouragement ❤😢
Yalnala YaAllah tahawu teh japaleh la frère...
Massa way meti na trop Bilaye ❤ des c❤ pour lui
Les chururgiens allemands ont fait un travail hors normal son visage actuel est 100000000000 mieux que que avant
Bravo il faut être fière dans ton propre idantite bilay keneu eupeule woul leneu ninga Mel macchhall khewale n'a
Mouhamed yalla nala yalla diapalé si barké seydina mouhamed Sallalahu aleyhi wa salam aminee ❤❤❤
ماشاء الله تبارك الله جزاك الله خيرا يا اخي أطال الله عمرك حفظك الله ورعاك وأهلك 🤲🙏❤️
Mouhamad yawe danga yarou sakhe kou bakh nga ❤❤❤❤❤ yalla nala yalla takhawou
Sénégal rek la guis dougnou respecté l’intégrité physique de la personne .c’est moche de se moquer à une personne à cause de son apparence physique.
Lii motakh Sénégal boyaboo niou âme lou nekeu mais douniou massa avance
Courage que dieu veille sur toi
Sama ❤ tooy na 😢😢😢😢
Maasàllaa yalna la saa boroom da
Diapale barkeb boroom Tuubaa ❤❤
Ma challah c' vrai courage rk mn ns sommes tous mm devant Dieu
Faut jamais laisser un bébé toute seule avant ses 7 jours moy indi liii yeup force à toi
Pourquoi avant 7 jours yi khana moment bobou mo geuneu mety
@@kareabdoulahad622 si waxna degue baxoul meun nagnou wethié SA dom walla comme liko dall tmt moy lolou
Deugle mame Yi louniou wakh rek amna lou takh bb kéne douko bayi mome kasé daniou koye changé lou am la
Manshallah yalna yalla safaraa si barke moustapha
Ndeysane liir kéne douko bayi mome késsé ndeysane yalna ngua wer mon frère ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️