Série - Diabarou Gorgui - "La femme du chef" -Episode 1 VOSTFR
Вставка
- Опубліковано 5 лют 2025
- Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
...
facebook
/ kharmedia_l'officiel
Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Beugue nako sétane wayé dama rouss ndakh Lima nékké dafa eup série bou nieuw ma andak mom. Amna mélokane nak vraiment.
Magui deh mdr
😂 aythieu rekk niou setane
Fi rouss amoufi souniou djikou dall😂🤣😂🤣
Détway😂
Manguu d😂😂😂nioyem
série bį nék na trop yal nako yégalé ah Diam si barké Serigne Babacar Sy ❤️🙏
Ana niou koy sétane beuseul bleu
👇👇
Jjjjjjjjoooooolllllllliiiiiieeeeeee
Yalla naniou yalla mousal thi mousiba ak bala thi barke seydina Mouhammad 🙏🙏🙏
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Bismilahi rahmani rahimi gnou ànde sétane KO si diam
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Amine 😂😂😭
Amine
amine way
Amine🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
khamè nguèn gnarèlou goor gui bi mo jouer ayy gaff saly aka yarou te jongama gnou andeu sètane ko si diam inchallah🤗🤗🤗
Moussoram tamit lol
La maman de Sadiya dialaleineuh message bou ame solo Ndeyssane si diouli ma sha Allah❤️🙏🏽
Ki est d'accord avec la copine de sadiya tapél j'aime pour moi elle a parfaitement raison parsk la vie est vraiment dure té djiguène dagua wara am fo wérou soulla goor défalé gua dieul soulla défaloul gua déffal sa bope point final😍😊
Je suis d'accord avec tw mane deih nonou la soné dougou si seuy té amo silo diap c'est trop dure mangui weur founék liguéye
@@mariamandiaye6576 tkt pas yallah baxna leip dina bax inchallah continue de prier rekk❤❤🙏
Toma
@@lymatediop6191 wiii toma😍
@@mariamandiaye6576 vraiment c triste mais courage digua am inshallah déll niane yalla rk lépaye bax😍💖
Cana dégueu dey sétan yep 😂 bonne continuation khar média
Yalla nagne diéxal saison bi si diam🥺❤️
Amine yarabi
Amn
Amiin
Ñou tambali si diabarou Gorgui yalna ñieup am diam🙏🙏
Amine🙏🙏
Faux cils=rideaux Maiga
amin
Amine
Ame guénn mélo kan😂😂😂😂😂
Cana dou raté beine série 😭🤣🤣🥰😭
Aka lerr
Moi
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Bilae
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
En tant que porte parole de l'association ASSY (Ande Setane Série Yeup) je tiens à vous faire part des decisions prises lors de la réunion précédente qui sont les suivantes :
-Interdiction des demandes de "J'aime "en utilisant le nom Du Prophète ou des Marabouts
-Interdiction des insultes
-Interdiction des Hors sujets (même si j'en ai fait) 😂😂
Pour toutes désobéissance à ces règles une sanction sera appliquée sans negociation
Sur ceux je vous souhaite une très bonne visionnage à bon entendeur salut 🤗
😁😁😁
@@mmefalldior2517 arrekh de faikhh genre 😂😂
Barki yalla mala beugue
😂😂😂😂d'accord
tout a fait d accord avec ses règles question d honneur merci ma chère 🙏🙏
Bismi lalih rahmani rakhime yalla na yalla déf diamou ñiou sétane ak diam 🙏🙏
Guorgui dal moy laulou dangua beugue fédéli koleuré rek dieuleul yayou Sadiya
Mo geunon nak même age la nak
Vraiment même yaye dji da fogone mome lay wakh
Bilaye
Lolo moye colaréki
Vraiment
Yananiou tambale si bismilah diekhale alhamdoulilah kenn bania mansue 🤗🤲🤲🤲🤲
🤲
Amiin
Amine yarabui
gnoune gni doul bayi bén série on a réunion ce soir à 23h chez mw🙏🙏🙏✅
Kn dé sa keur dina eupou ay lkho
@@ndeyemanembaye7358 no oute na bénté salon bou pour réunion bi🤣🤣
😀😀😀😀😀😀😀🤣
@@modoufaye859 kxkx
Apres choix de Soleil d levant Dina tew
Kou mélni man âme na série bou niew rk gua sifre
Wawa Man mi
Badou
Mangui ni douma rater ben seuff you nakari yi
Ma gui nii
@@boussogueye8053 Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
ana sope serigne saliou Mbacké yii aye thia kone noiu wadial khélcom
Waw waw
Insala
Ndeysane meussouma ame j'aime
Manite kene d’où mane bayi wouma bene série ba melounene ni mane rek waye yalla nagnou ko commencé thie bismilah egualiko thie alhamdoulilah kene bagna manque
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Alahouma amine merci
Alahouma amine merci
Amine yarabı
Amine
Tay khana duna ame j’aime
Lekal j aime yi
Svp lundi ak ban jour lay am?
@@mbackezeyna6050 lundi mercredi et vendredi
La première scène c’est trop moi avec ma mère 😂🤦🏿♀️❤️❤️
Ani wa A.s.c. bokou beugue beugue☝️kou daccor ak mane si tour bima wakh🤣🤣 Jaime mouy gaw❤❤
Ani wa team WiFi way ?🤣😭❤️😘
Niougui ni
Magui ni ✋
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
@@amadoujuniorgueye3662 Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Je suis là cana yi 🤣🤣🤣🤣
Anni wa coalitions ande sétane séries yeup💪😂😂😂
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Sila bok dh série yeup lay suivre
Je pense que cette SADIYA va subir, mais je vois en elle une bonne actrice j'espère qu'elle sera à la hauteur.
Bismillah ñu tambalé ko si jam agalé ko si jam. Aythia
Amine 🤲 waye
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
@@ndeyeastousamb9685 Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Saadiya demal nek niatel Parel d awo bou doff ngafay fekk teksii xalei nga tu as l'avenir devant toi
Gnou kholl bakham loumouyy diokher, en tout cas Cana benn DIABARR layy Amm fi reww MI tollou nii.
Fallou tu est adorable
@@cheikhmahybfall9854 🤣🤣 yaw mom Cana gua AMALL tawfekh ak taysir rekk inchalla
dafa leer billahi 😅😅
Ganima 🤣🤣🤣🤣
Diadieuf Fallou 😁
Ana wa association andeu setan série yépeu 👌😂🥰
Premier vue c'est moi ❤❤❤
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Sadiya nigay lokhati glace bi metina 😂😂😂😂sinon khar media yenagui évoluer vraiment félicitations 🎉
😂😂😂
😮😮😮😢
Ohh mamoune c'est alou de la serie dérapages il es mignon
Rang niouy setane😂 affaire de thiokhalibrene😂
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
@@storytimeaiYT c fait ma belle t video son super drôle mashaallah
🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Wa d'accord sa passe kan et kan😇cana dou raté série yi way enfaîte niariii diabar si keur mom ni rek man mom souma démé bay woudié mom naga meune out 2 maisons rek kou nék tok sa keur wesh 🥰🎉🎉🎉
Mai guel bi tik tok la nék di wawouh kay lgui niepay joué théâtre d'accord damako bgu nak el fai ma journé tt l temps
Ki est la ?
*Khar média da ngéne niou* *yapp episode 1 ba 90 béne deug fégnagoul*
Encore une série de plus🙆🙆🙆 liguéy bou agg sakh meuneutoumako
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Wa yèn esk dolèn wah ci mane serie bou nieuw rèk ma sètane
Oh sadya gno bok tour. Quelle joie !
Billahi amna fébar théâtre bou guénn thia niakoy ndieuka sétan salay bokkou😅
Ay way kou kham samba kende mou dieulma ma liguey sokhla nako lole 🙏
Aaaaaaaa théâtre bi nékh na Ba paré ndakh goor gui Lam la sant t Sama dieukeur❤ Lam la sant niaw❤
Bannn lam nonou apar lamsettt bi😂😂😂
L’actrice principale je la reconnais par TikTok avant la série
Elle a joué dans la serie belle mére mom la moustapha diop forone mou perdre memoire bi
Wi c vrai
Môme la
Oui c vrai c fatwablack sur tik tok
Wiwi mo nek si TikTok bi
Gorgui taamite Mom kholna Sadiya taamit mi moromou domam 😂😂😂 yeway Mamour ndeyssane amour bou fom guey wadia am brefeuh Allons way première femme bi tammit phénomène la deh 😂
Yalla naniuko tambalei thi Bismillah yegaleko ak alhamdulilah
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
JAMAIS DE COMMENTAIRE QUI A UN RAPPORT AVEC LA SERIE SOFF NGUENN WAYY
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
@@storytimeaiYT 🤣🤣🤣🤣
😅😅fah
Je suis accro bilay les sénégalais sont les meilleurs
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Merci beaucoup
Li rèk Machalah
Sama wètay yènakoy dindi
Yalana seen Diam yague
Alahouma Amine
L'actrice principale est magnifique sans maquillage avec teint noire bii nakk mashallah
Elle joue bien aussi
Lalou seuy dafa khate y'a des hommes vraiment égoïste. Meuno feck khalé bou ndaw am koumouy beuguantel nguay khôl say beug beug rek pour tack KO
Bilaye
😂😂😂 la maman de Sadya est la principale coupable mais Guorgui meuna ko tak mome yaye dji
@@mariamadiallo6272 vraiment nio bokk génération dounde bâ diekhal yakk dounde jambour
@@tishaprudenciabadji3820 g compris serie la, mais beurina si mime rey, pauvretè baakhoul
Le vieux a droit à une nouvelle jeunesse !!! Le bonheur charnel se trouve auprès des jeunes femmes de la vingtaine 😎😎😎
Pa bi aussi sadik n’a dei sadiya xalé la di😂😂😂😂
Team MDHM, golden, karma ninki nanka on vient testé ça aussi 😆
Machallah yalla na yalla akalè ak diam sibarckè Serigne Babacar sy
sétan kosi diamou nioun wa team and sétan série yépou 😂🙏
Kou melni mane amna douma raté béneu série 😂
Lila dall moma dall 😁🤣🤣
Biti lokho yaw deuko kebemer ?
Bismillah yalla n'a série bi koumasé thi diamou mou diékh ak thi diamou bonne continuation
Un homme qui aide une veuve gratuitement à notre epoque . Il a des idées derrière la tête. Il cherche quelque choses.
Ok
Serie un bon début merci pour les sous titre en français 🙏👍👍👍
Fatou la TikTokeuse est l’actrice principale ❤️❤️
Waw kay nougnou commencer di diam agali si diam 💃💃💃
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Qui remarque que Mamoune ressemble à Pape démba ndiaye Daaray kocc
Wa man lolou beugona waxe iska dou domam
@@matydienge7002 il se peut d niro nagnou trop
Wi loll c vrai
@@adjasokhnadiokhane2739 bilahi nak
Je pense que son nom de famille c Diongue il est l'ami de Bachir dans dérapages
Yalna niep am diam ani team wifi and setan série yeup🥰❤💫🙏
C une serie ki promet , les jeu d'acteurs sont simple et naturel
Lègui dama bayi commentaire dakheu daniouma commencé khamè si commentaire dakh di suivre
Lay la série ba nieuw na💖
Qui est l'artiste avec cette voix incroyable ? Waouh !
😂 😂 😂 Niou dioulou si lou bess bi
Kou Remarque ni Sadya dafa Nirok Maman Café Avk
Mandé nday mari serie karma la diapp
Mom moo neek ci tik tok bii elle fait des vidéo très drôle xamena fofou lagne ko guiss3
Loula dal mama mo dak ki
@@mamankhady3376 oui c elle
@@mamankhady3376 elle a déjà joué dans belle-mère et jiggen
C est pourquoi les femmes doivent travailler ..etre une femme au foyer n est plus prudent à notre epoque. Les années qui suivront seront plus dur.
Les femmes réveiller vous
Oh la femme de goor gui! Ça promet dé j'adore cette femme!
Et la maman Daba soumaré aussi
❤❤❤🔥🔥🔥
Serie bou niow ma sétane na néh rék niou tok bou néhoul niou daw
Wawaw lolou késsé la nak
Sadiya da niro ak maman bou un café avec
Dimbali nit ki waroul takh been wadiour di yakk mbeuguélou khaléyi
Tata Bety Thiam alias Dieynaba 😍😍
Ayoo c Alou dans dérapage je l'adore♥️
ANA talibé Serigne fallou
Yalle nagne ko commence ak bismilah agalè ko ak alhamdou lilah 🤲❣
Euyy wayy loutakh ma bagne niarels yi.loussi yonam si discussion entre gorgui et Dieynaba
J suis awo mais tay mom niarel yii la andal ma puce tay danio thiouner trop
@@sarryacine2317 awo bi pank na mais mais mo tané niarel bi.2em episode bi la gueuneu merer niarel bi
Wa ki nilaye leikei glace ?😂😂😂😂comme Kouy lekk made deh
Waw eupeullee😂
Allez 25mn bi mom baxna solène augmenté aussi on prend😊 rannnnng moy nèkhe...
Ohho goorgui tamit koka bayi mo séparé niari xalléyi😌
Tek si mamour diarbatam leu
4ème vue ❤️
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Arekhhh de fekhhh genre c diabaru gorgui🤸💃💃
Ayooo niou commencé ko si bismilahi rakhmani rakhim yégualé ko si alhamdoulilah 🙏🙏
سعدية etأمية
Nom you nékh té raaaar😍😍😍😍
Waw Kagne bismillah niou tambali ak diam aksi leine maleine di dalal 😍
Kan yaw🤣🤣
Saly daraay kocci mom fouma ko guiss nako setaan aussi Cana deug dou rate serie Ani Cana yi book yeungou len
Magui ni di setane b sonou teudeu
Gnoguini 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@@adelaidesonko1472 sawil te dem teudi bb
@@ElTIO_Galass 🤣🤣🤣🤣balnala
@@adelaidesonko1472 diokh ma sa número WhatsApp nou wakh
Ah bi nexna dehhh waye ken du woodiou.p. kagn lay comance sax .
Wa xar media Ken du yen.
Good job .
Bn travaille. Depuis Angleterre
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
@@LIGUEESPORTMOBILESN abbone na contane nga😂
@@sokhnafall4329 bly trop mm😂😭✌️🤍merci way c vraiment gentil
Qui reconnaît Saly la 2eme femme de Gorgui 😁😁😁
Moi
Maïmouna Ndour moi
Maïmouna ndour aïe guaf
@@sarrkhady7327 môme la Saly deum
Limay guisss nii Diko vue nii ayyy professionnel deugue niofiyy jouer liii comme guerr ak mr l maire rkk
Rang mouy ande setane série yeup 😅😂😂😂
Wawaw
😂😂😂😂
Dama diakhle sakh
Xaléyi mouno touniou diangue séne leçon ndax réseau socio 😂
@@fatouniang1505Rang mouy gaaw😀😀😀
Teuss ibadou def haut décolté pause cil ma warou mane 😁😂
Daf ko diapoul sakh
Daniou nio yap rek
Bismilah gnou dale ak diame
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Je viens de commencé la série alors que vous êtes à l'épisode 245 je crois , mais je compte regarder toute les épisodes jusqu'à la fin inchallah
😂😂 ayway man amna melokaan serie bou nieuw ma yerdouko🙄🙄😂😂🚶♀️🚶♀️
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
🤣🤣🤣🤣🤣🤣👍
Kon bax naa 😂😂😂
C'est quoi l'histoire de la série que les vieux sénégalais sont et ont tjr été pédophiles et surtout ne nous faisaient pas croire le contraire
Rang thioug thiang ''''' diabarou gorgui la🤣
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
@@storytimeaiYT pas de soucis ♥️
@@storytimeaiYT mais c déjà fait ma chérie
😃😃😃😃😀
Bismilah niou setane diabarou gorgui
Slt dsl pour mes commentaires mais doma diapaler gua abonne thi sama chaine c l lien en bleu 👉 ua-cam.com/video/oZEo7IZTras/v-deo.html
Machalla ta awa je t’adore 😍 depuis gnankenne de thies 💙💚💓🇬🇭
Sadiya est une bonne actrice c elle qui est sur tiktok elle m fait rire a chak fw k je vois cé video elle est tres drole en plus
Mes damakoy weur 😃😃😃😃