Xalisso - Saison 1 - Episode 38 **VOSTFR**
Вставка
- Опубліковано 4 лют 2025
- ** Abonnez-vous ici bit.ly/evenpro... **
L'argent fait-il le bonheur ?
Dans une société où paraître est bien plus important qu’être, l'argent devient le seul mètre-étalon. Son ombre plane sur les rapports humains. Tel un ressac d’été, l'argent martèle et marque son empreinte. Peut-il effacer un passé ? Peut-il déterminer l'avenir ? Parfois l'ostentation est fille d'un complexe...
Allez au delà des mirages de l'argent et de son impact dans la société à travers la nouvelle série Xalisso ! Evenprod s’y lance avec humour dans une analyse sans fard de la nouvelle bourgeoisie.
Un nouvel épisode les mercredis et samedis soirs 19h30 UTC.
#xalisso #saison1 #episode38 #creationoriginale #argent #bonheur #evenprod #new #2024 #team221
** Devenir annonceur ? Contactez notre service commercial **
Evenprod +221 77 422 70 41
** Retrouvez Evenprod sur les réseaux sociaux **
Facebook / evenprodsenegal
TikTok / evenprodsenegal
Instagram / evenprodsenegal
Twitter @evenprodsenegal
Haaa bouri le peuple est content .il était tant de remettre cette femme à sa place ,trop c est trop 😂😂😂😂😂
C'est bien c'est très bien
Bilahi 😂
@@Fama-e5k
C'bon C'Tres bon
Kou djour Anta ? Test AYDEN encore 😅
Boury a super bien répondu 💢💢💢💢💢💢💢💢💢💥💥🇸🇳
C bien boury nit so defe lou bakh dagn la nane c bien mou geuna bakh niouni la ctres bien 😂😂😂may len j aime nak dama beug louma rere 😂😂😂
billahi wallahi dama contane ❤❤❤❤
@@khadidiatouba408nieup contane Taye 😂❤️
C'est très bien boury c'est très bien 😂😂❤❤❤❤❤❤
Kone boury c’est tré bien 😂😂
Mani c'est très bien lawakh 😂
Khadija 😂dotoko defati 😂merci boury❤
Maniko c’est bien ❤😂
Sokhna Diarra mon khewlé dh ana sopey sokhna Diarra yi❤
Je suis là sur la route pour aller à prokhane
❤❤❤❤
Niou ng nii❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je suis la 💕
Kharal ma déff ni gneup des cœur pour notre prophète Mouhamed psl😂❤❤
Humm yalla bakhna 😂
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
😂❤❤
❤❤❤❤❤
La surprise de Khadija sera immense que celle de Mareme Sall bilay 😢😢😢😢 pour ceux qui sont pressés pour sa défaite doucement rekk😢😢
Boury, sa beauté sa thiass sa voix érayée qui fait ton son charme. Elle joue merveilleusement bien tous ses rôles. Tay nak tu as frappé fort héeeee damani c’est bien c’est très bien Boury !!
100 ans si yaw. ❤❤
Une forte pensée pour les femmes enceintes que dieu leurs facilite l’accouchement amine
Amine incha Allah ❤
Amine ma chérie tu es tres gentille
Aminne ma chérie
Amine
Amine
WippliwwW💃💃Boury tey sedal gua xol yeppp c bien boury c très bien 🎉🎉❤❤❤😂😂😂
Épisode bi déh marmite bouy bakh la béneu roukou sédoul c’est bien 😂😂waw Boury am na beauté dionguama na lamignam saf na c’est très bien 😍😂
Bilay 😂😂
😂😂😂ray gama
Fall la Sante nak
Nagano c’est bien🤣🤣🤣
😂😂😂😂😂
Boury gagner neu bureau yeup🤣🤣
😂😂😂😂😂😂
😂😂😂
😂😂😂
Sen espiration laa dômou papa😂😂😂
Woopopopopopop😂Diawar dinama ray
Ay Boury damakoy beug ba kagne❤❤❤😂😂😂😂 Khadija khamone guani sa beuss dina gnew
Une mère doit défendre sa fille merci beaucoup Boury ❤😂
Blh boury ma contane thi iow khadija tay niam nga dei beaucoup de cœur pour boury fall ❤❤❤❤
Limeuuuuu nakariiiii Jeux de Dames😭💔Boury fadiall namaaa kooo😂👍Khadija dieule neuu coup teyy nakk🤣🤣🤣🤣🤣wouyyyyyy liii nekhnaaaaa
@@JeannettePulchérieSambouay way lou khéw jeu de dames mane UA-cam rek lakoy suivre
Merci beaucoup c bien ce très bien ni la kay di wakh si Seri bi setana gouma sakh content wayé nekh fi di wout ay aimer rekh😊
exke ass jañ mo jour anta😢😂😂
@@DieGningue Aziz neineuh daa nopp Binette😂😂😂💔😭
Esk guisguéne stylou Sokh’na bou ndaw ❤nn mais cet fille est trop stylée ❤❤❤❤
Kane moye yayam boury kom wathieu na 😂
Sama lék la 😂 mako fa Am xalé bi gagné bayiwon ko xél
Esk Sokhna mou ndaw est la femme de bobou desin stp
Seule une douche 🧼 bien froide va calmer boury fall pour le moment. Elle est trop a chaude 😂😂😂
J aime ça moi 😂😂
😂😂
@@FatimataFèdior-n9t on aime 🥰
@@Omardiallo-yr3nv 🤣🤣🤣
Boury merci mani boury a diarama mani boury thank you chérie boury wakhma lo beuga dègu 😊😊😊😂😂😂 c’est bien c très bien 🎉🎉🎉🎉
Boury wakh ma lo beugue ma djindalla 😂😂😂🎉🎉🎉🎉 aujourd'hui c'était l'épisode de la gloire 😂😂🎉🎉🎉🎉
Khana dom toubab la beugu😮😂😂❤
Ta mère ma mère nos maman vivent longtemps avec nous ❤❤jusqu'à notre réussite
Serigne Touba néna yené niépp diam takhoul niépp am diam wayé kou am ga am diam kou amul diam ga am diam ❤❤ yalla na niépp am diam ❤❤❤
Amine ❤
Amine yarabi 🙏
Amine
Amine 👂👈
Alakhouma amine🤲🤲🤲
Bouri c'est bien c'est très bien 😂😂😂
Boury c’est bien c’est très bien🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Le masterclass de Boury FALL
toutes les mamans et sœurs doivent prendre note ehhhhh 😂😂😂❤
Bourry meilleure actrice ❤🎉 de l'année 😊❤🎉 je vous dit 😊❤
Fo bayi amy mbaye😂
Boury meilleure Actrice lolou force lah🥇💪❤️
Slt wah ça fait longtemps foh nékon damala guéthie guis si commentaires MBA diam la won❤
Awa nkm
Je valide elle est excellente
Khadija khadija boury dane nala nk😂😂😂😂des cœurs pour boury fall way ❤❤😂😂
❤❤❤❤❤
Ndeysann Maty rose est une femme tellement adorable machalla ❤️enfin Tay soda mareme tekna perruque bou bakh😁normal teksi😂🤣mais la classe de Boury Olalaaaalaaaaaaaaa🎊une petite
Love sur vous❤️❤️❤️Wa EvenProd
Bilahi😂😂kana mame gui nourole takou roff😂😂
@ ngani takou lann yaw🙄😂🤣🤣😂
😂😂😂😂😂😂wouy soda Mareme 😂😂Diagnene bi ya bone
So paré nga wakh si peruk anta bi tamite
Cv
Khadija dotoko défati 😂😂boury moi aimer toi❤
Mais pourquoi niepe begue ame ayi j’aime 😂cône maylenma ayi j’aime 😢
Boury fall gagner naaa bureau de vote yeup Ak Centre de vote yeup c'est bien Boury c'est très bien ❤❤❤❤❤
😂😂
🤣🤣🤣🤣
Khadija Nak Aka Yap Asse Diagne😂Kii Ndakaté Boury Mo Bakh Si Mome😂Taye Mome Dama Contane😂😂
Rewoul sakh khamena pasti ak dayou beye😂😂😂😊
@@awatoure5056😂😂
Male gene kon tan🎉😂😂
Bourry deh lou am class lafi khoulo gnafff so rafeitei pank dangay kheirei
Khadija dotoko defati💃🏻❤️
Sa digantèc yallah dè nguay rombou tè do aimè sakh 😂😂😂😂😂
Aimer na😅
Wawaw 😂😂😂
Dina aime Kay guaye guigne rek 😂😂😂
Dama la rous rk motakh
Amine ❤❤
44:29 enfin first defeate de khadija 🎉😂lima si geuneu nekh moy maty amna point bo graww 🤭🎉🎉🎉 tata Boury ont t’aime wolah je savais que sonu khol yi di meti iiw yagno siy guené chapeau tata boury elle assure grave cette belle dame 😻😻😻
Àgg sunu yu exfgjiooliiyytressxgy bi ci diggante ñaari gox 🎉🎉🎉yukoo😊😊😊😅😮😮😢🎉😂😂😂❤❤❤ ❤❤yi nekk FHJIOPŊLMMMNJHGGFDZZWDTJKK BI BI 😢😢🎉🎉😂🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉😂
Gnune setaan Katt yu ndeketei ay vrai seytaanè lagnu 😂😂😂
You mq k sah😂😂@@dabadidadia
😂😂😂😂😂bilahi yow
Épisode yima meuseu setaneu bi moma si gueneu nekh way une belle leçon de vie fi loula niiteu khamaleu khamaleu gako louko rayeu fouf nopiwaleko nakeu j’adore l’élégance et la classe de Boury Fall ❤
Sama❤❤❤ mingui si frichidaire😂 Boury c'est bien c'est très bien 🤣 c'est bien très bien 🤣🤣🤣 kou contane rek lalal j'aime ma khôl niata ❤ nio nekk si frichidaire 😂😂😂
Prokhane yallah na borom bi fayal niou sokhna Diarra jiguén gni roylén di jarrah 🎉❤
Amine
Amine
@ ☑️👏
Amine
Amine
Je me sens tellement ému quand Oumar dit à Maty Rose " quand je travaillerai, je ferai pour toi, tout ce que tu veux". Les sourires qu'ils échangent sont sincères et leurs regards si pleins de tendresse. Ah! Moi Fata, quand je vois des personnes qui s'aiment sincèrement "sama khole bi daye nékh, mélni Fata mou guiss yéli guinar"😂😂LOVE
On t’aime fata 😀❤️
Inspiration mom dako am konn Yako feu am😂
Encore fata😂😂😂
Sacré fata😂❤
Ahh taye nékoul soy xoll Queen binta 😂😂😂
Boury anhhh bouy xoulo sakh dafay am feeling❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉
Ayo bravo Boury c bien c très bien fait pour Khadija mention spéciale à vous niaf coup dougue na nak téye 😂 Khadija digua nopi dh âme dieukeur âme farr ba âme fa dôme 😢 top nite yi nane thiaga alors que yaye vrai thiaga kouné AK sa bése. Dagne nag gua maye nitte yi diam 😢 machallah couple Maty et Omar
🎉😂❤😢😊😅😮
Yaw liga fi tek ny nékh na dal khady jia😂😂😂
Aka limou khass maty rose yep tey mou niow nane biral seurrou dengkané leu khadija inaf way
@@fallndeye6092 bilaye dh li
@@annemarieniane8859 di khasa té déf Lou né weg
Ohh khadija amna défaite bou soft wayy 😂😂😂 c’est bien c’est très bien
Bakhna si mom dafa bone rek 😂😂
😊😊
😂😂😂😂😂
Heeee bouri c’est bien c’est très bien 😂😂li dh moy koula douleul ga Fenalko 🤣🤣🤣🤣
Boury fall c bien c très bien 😂❤😂😂😂des coeurs pour Boury fall❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
12:47 éhhhhh taay mo nekhh 😂😂😂 walah j’aime cette dame elle assure bien son rôle 🎉😂
33:04
Niaaaaaw khadija. Ndékété Bourry Fall mo bakh ci yaw.😂😂😂❤❤❤
Quelle classe elle a Bourry❤❤❤
Kou beug am dom bou goor ñou toudéko yonetie bi rk lalal j'aime ♥
Amine pour ma sœur messoul am dom😢
Amine 🙏
Amine yarabi 🙏 inchallah
❤❤❤❤❤❤❤
C’est bien Boury c’est très bien ça Khadyja taye nopina dh am dieukeur am farr 😂😂😂😂
Té khamna anta moy doom bimou am ak faram Boury Lou leer la wakh 😄😄Sama gniary doom yi gno bok papa
Billay jusqu'à preuve du contraire ndao mo diour diadia
@@mariehelenefatimatine1624nguanima lannn🫢
Doynawar dé 😂😂
@@aidadiop1201anta lako fok motax mom la gueuneu beug
Contane na si boury wayyy😂😂❤❤❤❤❤❤niaffe Khadija dotoko défatii
Des cœurs pour notre Prophète Muhammad P.S.L❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤psl
Nitt koula bagn te defoko dara boum la diaral mouk def ko lou niaw 😮dakh amna boula beug te defaloko dara ❤yallah hamnako happy Wednesday 😘
bilakhi dégu la ❤❤
Merci beaucoup tu as tout dit bilahi
Épisode 38 bi mo gueune nekh yenene Épisode you diota romb yi ❤❤. Boury on est content 😊 mane iow rek lay top ❤❤
Kou yakamtiwon le èiiiiiihhhh de boury fall 😂❤😢mok mareme sall am nagn tres si khadarrrr 😂❤
Aye waaaaay boury le peuple est content 😂😂😂😂😂😂 welelele sama xol bii saide naaaa 😂😂
Boury c'est bien c'est très bien 😂😂❤❤ Khadija dotoko défati ❤😂😂
Séquence boury bi ak Khadija setane nako 10 fois 🤣🤣😂😂😂 aye li mo nekh 😇 boury y’a khérré
Moi aussi
Moi aussi
Moi aussi
Ak mane
Moi aussi ❤❤❤❤
Boury gaïndé là 😂😂"Hééhhhh"bi mome si xol bi lako tibé😂
Khoulo nekhoul wayé bu Boury bi 😂 c'est très bien 😂
Bourry dame de fer responsable maaateu limou doone mashala yaa bah thi Khadija 😂❤😂❤
Boury sa éhh bi histoire dinako bide 😂😂😂 lidianetiko dh n'a nekh 😅❤
J'ai jamais commenter mais mon cœur est en joie evenprod vous avez fait ma soirée❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ longue vie à toi tata boury❤❤❤❤❤
Evenprod merciiiiiii pour le début de défaite pour khadija😅
Boury amna classe ♥️♥️♥️
Regarde moi ses yeux ❤❤❤❤
Li Motakh key khadija beug anta th beugoul diadia le papa de anta est son amour de jeunesse 😢😢
Mais le blem est que diadia mo makk anta
Boury gagner na bureau yeupp😂❤
Ôooh j'adore le passage de khadiza et Bourry lidé kani gouwanala😂😂
Qui a regardé trois fois l'épisode comme moi Khadiza à bien assurer son rôle chapeau khadiza
GOANA 😂😂
Prière pour gniy dem prokhane dem si diam gneuw si diam amîne barké alhurane
Boury c’est bien manéla c’est très bien Boury 😂😂😂😂😂 khadija dieulna coup dh 😂😂😂😂😂
Le héééeeee de Boury takh na ma tela setaan tay😂hééééhhh khadija tay nga dééééhhh😂😂❤
Taye mou nekh😂😂😂
Lii motakh ma yakamtiwone série bi😂
@@AmyDiasséThiambilay ioe😂
Kon gno yam😂😂
Bon magal prokhane❤🎉
MachaAllah 🥺😭😭boury d’amour ❤️❤️❤️❤️❤️qui te peut ohhhh le peuple est content
Bory taye wathié na keur ass diange kon anta ak diadia bokou nio papa 😂😂
Anta est ce farou diadia bi fou papam kon 😢😢
@@KhadyKane-yn7gp bo kholé Anta la mère bi geuneuh beugue donc ass Diagne diouroul Anta.
❤😂❤❤❤❤❤❤
Est-ce que dou bancaire, Bi mo diour anta
Ennemi n’est jamais loin 😊
Bilay nos enemie ne vient op de loin😢😢
Applaudissez applaudissez👏🏽👏🏽🤣 Boury fall😍😍😍😍 tay sama khôl bagui mélni frigo khadija Boury dore nala th lokhom laloula la première défaite da khadija 😂
bilay evenprod yéna meilleur machallah ❤❤❤❤❤❤
😂
Aller bo guiss Amna retour 😂 Khadija sa défaite bi tayy damakoy celebrate 🎉🎉🎉
Lou nekh 🎉😂😂😂
🥳🥳boury way cé bien tu as très bien fait😂dakh yalla khadija nopi may gnou diam
Even pro yéneu meune Machalla c'est bien c'est très bien
Bima dioudo ba legui meussou ma ame j’aime 🥺
Vraiment papa youssou Ndour kéne amoul sa fay lissi khalisse diarna Lou né merci evenprop vous avez tout donner
Maffi djitou 1 millions j'aime inchallah
Apres jaime yi loumou lay apportel ? Nekk len ay nite
Louci sunu fou😂😂😂
Magui lay ziar
@@yamathiam9037 🤣🤣🤣🤣
@ ay yerme diawar di nagn ma ray
37:45 boury fall contane na ci yow deh une vraie femme de valeur machallah ❤
Merci beaucoup à vous Machallah Yalla n'a niépp am diamm Amine Y'a Rabby 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉😢😢😢
Celui qui joue avec ta paix intérieure n’a rien à faire dans ton quotidien.❤
Merci bcp Mme Diagne Boury femme de valeurs pleine de classe et de grâces mash’ALLAH. Enfin un adversaire de Taille à Khadija. Je regrette le prénom qu’elle porte dans cette série. Khadija la 1ière Dame du Prophète Seydina Muhammad SAW ❤❤❤❤❤
Ah Boury ni guay khoulowé machallah gneuw def sa noir bou pop ak sa maquillage 💄 💄 bou soft machallah dore khadija 10 - 00 lolou histoire dinako binedeu boury c'est bien c'est très bien 😂😂
Éeeee maniko khamgua lanla tay mou nekh😂wa guiss guéneu feeling bi Boury di dégagé😍
Bingay degagè la wah mane😂
@@Wfbh13 😂😂😂
Yaw guiss nga lolou kon feeling bi dafa eupou sakh 😂😂
Feeling bi dama sé wadd
Boury sédal gua sama khol bii❤
Kharal ma déff Fati ni gneup des coeurs pour notre prophète
❤❤❤❤❤❤❤❤
Le xoulo de boury est trop gueweulè nenako””heeeeh😂😂😂
Even pro yéneu meuneu yéneu eupou dolé macha allah c'est très bien ❤❤❤
Ha boury dé limouye yarou rrrek kou laneu domame dotoko défani dôme mo nékhecté sakhe si khole nite soko beugueu diote lalale domame❤❤❤❤❤
Khadija tay nopina dei boury rek seule💪🔥🔥🔥🤪
43:45 boury falla gagner na bureau de vote yépp😅😅
🎉🎉🎉🎉
Boury moy sonko 😂😍😂
😂😂😂😂😂
Bravo Boury en attendant may tolou fofou 😂😂😂😂
Khadija tay dégueu nga daali deh wépépépép Boury qui te peut 💪💪💪💪💪 mag bou réew dafay meuytou xalé bou xam Iow ndékété Boury sa lomotif la yor Wa héee 😂😂😂
🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳💃💃💃💃💃💃💃💃💃
😂😂😂😂🎉Lomotif kay😂
@ sérieux guisso nimou né patteu 😂😂😂
Tay la khamne so tapote 3 fois si commentaire day capture ❤
Abonné nio far nak ❤❤❤😂😂
Boury 🎉le peuple est content hein❤❤
Boury c’est bien c’est très bien 😂😂😂😂❤❤❤❤
😂😂😂😂
😁😁
Boury khamnga nite sou déffé Lou bakh dagn nane la c'est bien nga déf lou gueuna bakh niouné la c'est très bien
Louye sama fou😂😂
Khadija mi mba khol bi dou wadeu yéne wouy c’est bien c’est trés bien 😂😅😅
Perruque soda mareme bi teyy nice na 😂😂😂
Bilay elle a compri maintenant 😂😂😂😂😂😂😂😂
Dafa tané rek😅batey moma gueunal mireille mathieu bi😂😂😂
@@mariemethiam5861dafaa waraa daime thii salon you bax yii niou customisel koo lou bax
Très bien boury c’est bien boury wallah boury dou nitt moi personnellement je sais pas pourquoi je l’aime comme ça boury ehhhhhhh je t’aime ❤❤❤❤
Merci boury wayy contente n’a si yaw way door fayou 😂