La moralité dans cette histoire : - ne faut jamais marier une fille dont ta maman et ton père te refusent de marier, si on arrive pas à les convaincre vaut mieux laisser tomber - so goor takké diabar,il doit amener sa femme dans sa maison ou sa propre chambre ou baraque et être indépendant - ne faut jamais habiter chez les parents de ta femme ou construire là-bas quoi que ce soit car en réalité tu n'es pas leur enfant (juste un gendre) et ils ne vont jamais te traiter comme leur enfant - ne jamais abandonner sa maman et son père et suivre sa femme, aucune femme au monde ne mérite qu'on abandonne sa propre maman et son propre père - faut s'occuper et entretenir ses parents avec le peu qu'on gagne
@@amly819 mani jiguene bou fi bayi sa famille ndakh goor di nga ko regretter ndakh kene si niom diarou ko. Motakh mani la li nga fi wakh c’est aussi valable dans le sens inverse. Jiguene bou fi seuyi aussi tu restes juste une « belle-fille » ou seuyaane dans ta belle-famille.
Suis carrément d'accord bilay ..dara diaroufi li ..que sa soit une femme et un homme faut jamais abandonné sa famille à cause du mariage merci pour la leçon
Je connais pas la fille mais sa maman je l’a connais très bien bax na yeuk na nitt nékk femme battante nak beugoul kénn kouko yapp chapeau 🎩 à vous FAT SAMB YALLA NALÉNN YALLA TAKHAWU
Famille défunt bi amouniou louniou wakh ndakh danio torokhal sénn dom comme lepou nionmla dôme loumou bon bon téwall😥😥😥yalla nako yalla yeureum té diégalko ay bakarame amin
Ay way Sénégal nagnou bayi di deudalé gnar gnou yalla bolé lolou bakhoul té fitena ak moussiba rek lay diour ki deudou yallana ko yalla diegeul khareko aldiana ak bep waye dawlou thi barké seydina Mohamed SAW
Mane deudeulenaniouma ak kimadone seuyale baniou tasse daniou dane khoulo di khèkh ont se dit musulmants mais la majeure partie sont pire que des athès geume djoudou ak khète race ak ethnies yallana niou yalla yok soutoura
Yallla mo khame lépp billahi 😭😭🇸🇳khmo lén si dara noppi lén si 😭😭Nanu Rangal yalla khamo lén si dara sénégal danoy wakh Si lo khame nê khmun Si dara 😭😭😭😭😭😭🇸🇳😭🇸🇳😭
Merbi aussi limouwakh deugla modou gayi considere wougnouko nakala sa dome di laké yaw sa kheyé bureau té yayam famille wam dal takhowougnoko toujours famille sokhnam nioye topato walou transfert donté amna ay manquement
Mandè mousouma guiss nit dièll pètrole di wiss si karr pour rèy ay wegne wala quène khamoull ak petrol loumou grawè nit dièlko di ko wisse si karr.sè du nèmporte quoi
Cas bi dal critique na mais la version du frere du defunt semble plus plosible plus raisonnable la dame elle jure beucoup et elle se contredit dans ses parole
Le frère du défunt dit aussi que son frère lui a dit qu'il s'est brûlé avec une cigarette. Il n'a jamais dit clairement que c'est ma femme qui m'a fait ça. Naniou mandou gni leur histoire est compliquée. Ken xamoul
Mane dhé dangou la deuk comme mome wa yé khamalouma ko dara lou niaw khana dem ligueyi ak beugue Serigne Touba ba takh na mou am niari sekh Serigne fallou AK Serigne Saliou Mbacké
@@maimounandiaye5246 pourtant en se concerne le matelas suis d'accord à condition gnou changer matelas bii? En tout cas avec la police scientifique de notre pays lépp dinna leer inchalla ?
Mane déjà pourquoi utiliser du pétrole dans une maison comme bon vous semble c’est pas sur n’importe quel accident peut arriver dans toute la maison paix à l’âme du défunt et que l’affaire soit élucidée
Allaahoumma'ghfirlahou warhamhou wa afou'anehou.Yalla djeggueul leu té yeureume leu. Yalla deellooossi khel yi,defaaraate djikko yi , samme niou ak sounouy ndiaboote.
Insbiii nak yalla rk mo khame……la maman est sous La Défensive il faut la comprendre…..la maman insbii biii diakhleii na Elle boulversé parceque amena problème yo kham nei daflaye eup doller……………liii eup doller dalle moy kiii gueine adouna yalla nako yalla yeure 🙏🙏
wakh dji wakhou gnouko dafa melni affaire de Ethnie leu ak caste . Les désaccords pour leur union surtout du côté de la famille du défunt. Pourquoi le mari a quitté sa famille pour habiter chez la jeune . l'histoire est plus complexe. Que la victime repose en paix
Bien vu 🙈 on ne quitte pas sa famille 👪 pour aller chez la belle famille y'a un loup. Dommage que en 2022 on est encore là quel retard. Bref nous africains réveillons.
Elle raconte vraiment du n'importe koi ..c'est même pas clair ..limou wax amoul bopeu amoul tankeu ...en plus elle n'étais pas présente sur les lieux son discours est honteux ...une personne est morte une personne avec une bonne intention demande à ce que justice soit faite même si c'est sa fille qui est inculpé c'est une personne qui est morte qu'à même...c'est pas un animal..en plus elle passe son temps à jurer ..c koi le.projet fi gnifi dakeu watt niofi dakeu.....
Doul reik nguen dii deff ioe ak sa dôme wayei yallah dina lene atei ak nioune 😭😢 bouteille bii yako dioxei guemo serign Lutax ngay dem dii setlou ioe doul nga meune K l’âme du défunt repose en paix 🪦🙏
ya watte ni mouso dem si serigne et au début de tes mots tu as dit danga dem si Serigne mou wakhela denioulen dedeulé je m’arrête là . Ki dem yalnako yalla yereum khare ko aldjana thionom yem fii si adina 🙏🏾
Mane diga sodé sama frère di nieuw hôpital diko assisté bamou dhé nioukoy médiatisé tamite niou khalate touti trop de zone d'ombre dans cet histoire Yalla nako yalla yeureum
Tante Aïda mi doulkate la déh ioe niarr niou nékk sen négue nann rék nga meuneu dégué Amineta diko wakh souba dingama mayy sama batt yénn ayeu guénn trop non mais vrai scénariste
Mane lima djakhal moy le gar bimouy dounde lou takh dieuloul ndjabotam yobbou sene keur mou nieuw deuk keur gorowam yi. Mou dè kou nekk di wakh. Vraiment je ne pense pas k la fille moko tal
@@cheikhounadiagne5375 ah sangue bi tè mou rafet rek. Mane déy sagaw mala et je pense que la liberté d’une personne commence la où se termine la liberté de l’autre. Khamo ma khawmala na rafet rek. Mane nga diokhé sa khalat ci ay teguine ak taloubé. Nga balma
Quant là justice fait son travail normalement la famille de Aminata son victime parce que sen version yi bokoul je suis étudiant en droit j’ai écouté la famille de Aminata surtout sa petite sœur se qu’elle c faux parce que elle ne cherche pas de défendre mais elle cherche là bataille
Liguay wakh yénou woul mana ragalal yallah mo demba foumou guissé pétrole à 2h du matin bayy taleu bopam si sa birii wakh négua guemo sérigne téh nga dém si sérigne ioe koula guiss khamné koba nga sa bouteille pétrole bi ngay tékk khel nitt gni
Maman yaw tu ne dit pas la vérité ndakh geumo Serigne tes déme Di sétlou ay nitt gay wakhal Sénégal Moy deuk bo khamni dagnoulay togne ba paré Di weur Di wakh yaw so néké ak sa goro si birr keur gui témagnoulene diam doko guéne mes yaw môme ligua wakh dara lérousi
Mane liima diakhaal mooy khana au moment des faits yeen nieup dagueen Fébaroon ??? La 1 ère et la 2 ème dames yeup nénagn seen yaram nékhoul woon ?? 🤔🤔🤔
@@millesmots2881 rakou khalé bou goor bi thi bopam mo wakhni khaléy bou goor bi moko wakh néko soumadone kharou douma dièma sauvé watt sama boop doyna war dé yalna yalla leral yeup
@@jolieseye403 ça veut pas dire que daf ko wakh lolou rek deug la. Meune na ame beugoul wone wa keuram yi kham ni dafa dane djéma kharou ndakh gatchè. Ak lakk nimou métiwou, keup kouy lakk digua djéma sauver. Déé yomboul dé. Yalla rek mo kham nak
@@blacklady6356 dagua guiss ma wakh ni mbir bi ni wala ni la démé? Wala ma déf fi béne jugement wala dara? Bayi léne togn akki douggal nitt. Fekké wouma té deuggal louma fi dara. Dama apporter sama avis si bene commentaire bou spécifique paré préciser ni yalla rek mo kham li khew. Daguéne gnémé aye wakhi mandouléne torop pour un oui ou pour un non vous saoulez les gens avec ça. Boy woté mandou loy gneuw setane ci vidéo bi? Loy liré commentaire? Loy tontou commentaire? Sof guéne torop way
May his gentle soul rest in perfect peace ndeysann very sad 😞 the stories that has been said from both families r all different but Allah knows best may justice served
Lima diakhale moye yawe miye wakh deudelé bimou fébaré yafa yobou safara kone ya xame serigne deugue nékhoul liguaye wakh si yawe la nek esqua deudelé woko ak famille dakh limou léne di diarigne
En tout cas même si le défunt ne faisait rien à la maison, vous êtes restés avec lui Vous avez confirmé que c'est un homme à douze métiers . Où a t il dépensé son gain, vu que ses propres parents n'en bénéficiaient plus ? Paix à son âme Amine
@@Bambaprofil même souko jabbar ji sodder réfléchissez sur ce que la femme a endurée. Au Sénégal on n'oublie que la femme est très fragile beaucoup de femmes sont devenues dépressives à cause de leurs maris. Le mec vivait chez sa femme. Donc réfléchissez en bon sénégalais sans être hypocrite. Rufisque les gens de Rufisque se connaissent si la femme l'avais brûler le matelas allait brûler.... Réfléchissez...
En tt cas yallah rk mo kham pask ç que la dame dit néna dieukeurou domam bi famille Wam dagn ko béddi considèré wougnou ko ça semble vrai pask son pére desque mou dégu ni domam essaie de se suicidé il n’avait ps réagi il a même dit que dafa dém liguéyi normalement meunone na kholi domam bane état la nék ç vraiment compliqué Que firdawsi soit sa demeure🙏🙏
KII C UNE MENTEUSE DE CLASSE EXCEPTIONNELLE . TROP DE CONTRADICTION :ELLE RACONTE LE FILM EN DISANT FÉKKEWOUKO ; MOUSSOUMA DÉM THI SERIGNE DEUKK THI SÉET KATYI ; LE DÉFUNT AVAIT FAIT TENTATIVE D'IMMOLATION , POURQUOI CONTINUER DE LE GARDER CHEZ TOI ,? SES ARGUMNTS POUR DÉFENDRE SA FILLE ST MENSONGERS . PARFOIS SEUGN FALLOU , PARFOIS SEGN SALIOU GUEUMOUL DARA ; .KOUTAAL BOPPAM DOU WOUT SAUVETAGE THI CANAL
@@senegalaise9527 lgui gars yimou guisson t xamoul ndax agresseurs lagn ou po n'empêche mou continuer yonam...t bimou démé bassi porte bii xana Dina feug t forcément Dina am tidji t douko bayi ak kath bi
La famille du defun amoulen lolen wah danguen beddi won sen dom tay lii am ngueni amerde nit gni la dame lou mun ti khew mom teyè n'a domam ak dieukeru domam
C'est pas beddi mais lui même le gars sa famille est en location et aussi il a tous fait pour la fille et ensuite wadji il n'était pas un chômeur il était chauffeur et j'affirme que je connais bien l'histoire et je suis de la même famille avec le défunt merci de bien vouloir révisé une histoire avant d'en parler
Kou ddd ak sa bamel yako wakhal sa bopp Kone yalna yalla niite te atte lene kom fekewo warro di insiste si mo tall bopam ndakh makk nga te police scientifique kharagn na lool sakh mo tall wala dagn ko tall mo tomba determine lima diakhal moye yagui watt si li khamni y’a wakhni fekewoko comm esk do bayi rek justice deff yonam defante d lafi guiss ki dcd fate guene ko
Mére yaw domaram ngua rek koula khol kham ni yaw koba ngua te dara safou la yaw gnou wara ték sa dom si yone ngua nane damay porte plaint yaw kou réw ngua😭😭😭😭😭💔💔💔💔
Gni di wakh hamnagne la maman ou la fille, vous n'habitez pas ensemble, vous étiez pas la au moment des faits et vous ne savez réellement ce qu'il y'a entre les 2 conjoints, donc mandou len. Ndakh nit khamko si ay blancheur dents rek, takhoul gnouy wakh. Yallah rek kham. n'a yoon Def ligueyam, y'a mort d'homme malheureusement. Lieu crime bi le personne waroul wonn am accès vraiment La maman de aminta explique les faits comme si elle était dans la chambre. Yallah rek mo kham aallahou aalam
Bilaye ndiaboot mo sonou,peut être que Mo Demba avait des problèmes psychiatrique, métina dalle yallah nako yallah yeureum té diégeul ko aye bakaram , yallah rek mo hamme lou khéwone ce jour que firdawsi soit sa demeure éternelle Amine !
Len deh khamnako setane ngen trop fou eumbeul ame 2 fois seuy am fa te Diam amoul ngeni setane rek bparer le gars mom bimouy nek keur mere bi Ani famiile yame yemer na deh a mon avis so eumbeuler nite 2 fois koum takhawal ngeni faram la confiance doufa ame finalement mom mi decedes sakh Ken doukou Tala gnanal
Yalla rek mo kham Yalla nako Yalla xari aldiana firdawsi Yalla na yalla léral lep té svppppp bayilen di wat si serigne yi ak Yalla si lo kham ni moy lolou t’es perturbé maman liguay wax ni Yalla baxna on verra liguay waxni baxna té guene bayi serigne yi encore une fw merci liguay wax sou néké degu Diaroul wat
Gno yam deh vraiment sougn ko bagnone dougn ko fatt. On peut comprendre les incohérences ndax nena fekeiwoul bi kei di tal bopam. Donc li nit yi wax fofou rek ni moko lak lolou la meuneu wax.
Ki dème na paré nianalene ko mo gueune di wakh wakh you niaw yi paix à son âme Allah est le meilleur des juges
La moralité dans cette histoire :
- ne faut jamais marier une fille dont ta maman et ton père te refusent de marier, si on arrive pas à les convaincre vaut mieux laisser tomber
- so goor takké diabar,il doit amener sa femme dans sa maison ou sa propre chambre ou baraque et être indépendant
- ne faut jamais habiter chez les parents de ta femme ou construire là-bas quoi que ce soit car en réalité tu n'es pas leur enfant (juste un gendre) et ils ne vont jamais te traiter comme leur enfant
- ne jamais abandonner sa maman et son père et suivre sa femme, aucune femme au monde ne mérite qu'on abandonne sa propre maman et son propre père
- faut s'occuper et entretenir ses parents avec le peu qu'on gagne
Je te jure
Ce que vous dites est aussi valable dans le sens inverse.
@@reinedunordPas du tout, les responsabilités de l'homme différent des responsabilités de la femme.
@@amly819 mani jiguene bou fi bayi sa famille ndakh goor di nga ko regretter ndakh kene si niom diarou ko. Motakh mani la li nga fi wakh c’est aussi valable dans le sens inverse.
Jiguene bou fi seuyi aussi tu restes juste une « belle-fille » ou seuyaane dans ta belle-famille.
Suis carrément d'accord bilay ..dara diaroufi li ..que sa soit une femme et un homme faut jamais abandonné sa famille à cause du mariage merci pour la leçon
Paix à sont âme yalnako yallah yeureum bilahi nioun doom yii rk nio sonal sougnu yaye yii nagn lein djapalé stp yaye yii soneu nagn deh
Ki dém yalnako yalla yeureum kharéko aldiana Dieu est le seul juge yalnalén yalla até🙏
Je connais pas la fille mais sa maman je l’a connais très bien bax na yeuk na nitt nékk femme battante nak beugoul kénn kouko yapp chapeau 🎩 à vous FAT SAMB YALLA NALÉNN YALLA TAKHAWU
Bilae yaye dji kou bakh leu même Aminata sakh amoul problème khana kay ndongal mo nieuw rk
Bilaye wakhati djiguene djiou meune gorr le fate sambe khamoule thiow walahi thieuye ndogale souye nieuw doko guiss
Walahi ligeye rek laye def
Mère wakho fi dra Lou lérr yalna yalla léral lépp repose en paix Demba yalna la yalla yerem 🤲
Billay wakhji leeroul dara ci man
mère bi day fenne
domame moko tal
Yayou Aminata dh amna diarama nakh ouf sa dome ouf dieukeuram ak sen dome yomboul th famille mademba si guiss guiss nio geuna aiser
Famille défunt bi amouniou louniou wakh ndakh danio torokhal sénn dom comme lepou nionmla dôme loumou bon bon téwall😥😥😥yalla nako yalla yeureum té diégalko ay bakarame amin
Cette femme est perturbée, elle n'est pas tranquille
Vraiment
Kikaye wakhoule li ame
Geste yii barina trooop
@@designsafart59 doul kat la
Bilaye kou beugone mo demba le thieye ndogale
Une histoire très compliquée
Ay way Sénégal nagnou bayi di deudalé gnar gnou yalla bolé lolou bakhoul té fitena ak moussiba rek lay diour ki deudou yallana ko yalla diegeul khareko aldiana ak bep waye dawlou thi barké seydina Mohamed SAW
Mane deudeulenaniouma ak kimadone seuyale baniou tasse daniou dane khoulo di khèkh ont se dit musulmants mais la majeure partie sont pire que des athès geume djoudou ak khète race ak ethnies yallana niou yalla yok soutoura
Yallla mo khame lépp billahi 😭😭🇸🇳khmo lén si dara noppi lén si 😭😭Nanu Rangal yalla khamo lén si dara sénégal danoy wakh Si lo khame nê khmun Si dara 😭😭😭😭😭😭🇸🇳😭🇸🇳😭
ndeysann c très compliqué. paix à son âme
Merbi aussi limouwakh deugla modou gayi considere wougnouko nakala sa dome di laké yaw sa kheyé bureau té yayam famille wam dal takhowougnoko toujours famille sokhnam nioye topato walou transfert donté amna ay manquement
Cette femme ne dit pas la vérité. Écoutez la attentivement ses propos ne sont pas cohérent
Bilaye wakh gua deug
Wakhlene té yalla takhe femme bi Rufisque nieup ko khame guisouma kouko khamoule té kou deugouleu
En tout cas elle hésite beaucoup avant de répondre
@@binetoudiop7172 mayniou
Mandè mousouma guiss nit dièll pètrole di wiss si karr pour rèy ay wegne wala quène khamoull ak petrol loumou grawè nit dièlko di ko wisse si karr.sè du nèmporte quoi
Yalla rek mo kham! Ki dém yalla nako yalla yeureum xaréko aldiana🙏 diabaram soudé défoul darra yalla nako yalla atté!
Cas bi dal critique na mais la version du frere du defunt semble plus plosible plus raisonnable la dame elle jure beucoup et elle se contredit dans ses parole
Billahi
Le frère du défunt dit aussi que son frère lui a dit qu'il s'est brûlé avec une cigarette. Il n'a jamais dit clairement que c'est ma femme qui m'a fait ça. Naniou mandou gni leur histoire est compliquée. Ken xamoul
Walahi koula kham ,diom lala khamé naggo liguey ,gueum sa bop di wakh lou bakh diko def,nattou nak yalla mokoy tek domou adama,du courage Fatou Samb yallana sunu borom lerral lep
Amine yarabi
Bilay sokhna ya wakh deugueu une vraie battante mane dei liguey rek lala khamei
Mane dhé dangou la deuk comme mome wa yé khamalouma ko dara lou niaw khana dem ligueyi ak beugue Serigne Touba ba takh na mou am niari sekh Serigne fallou AK Serigne Saliou Mbacké
Wakham bi leeroul dara
Mouhamed aidara limako khamal rek la wakh ak diko massa wou,lissi dess nak C pas à moi de juger
Mane lima diakhal mou kén thi niome nianaloul yaw dawlou bi. Repose en paix.
Repose en paix dou tous boul ñu fonto limoy ñanoukh julit thim
😭😭😭🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😭
Natou dou wéss la maman je la connais c une bonne femme battante di wax lou bakh Yalla rék mo takh ak Rassoulilahi soyons prudents si cas
Bilay deguela natou d'où wéss yalnako yalleu may xolou mougne
Bilae nitte kou bakh la Sama kharitou Yaye laa
Lolou dhei la wakh..famille kou gorr ki beugouniou kou djigueinn ki
Avocats yi amna blém les deux versions des familles.
Yalna yalla leraal rekk momm mi kham lépp di guiss lépp.
En tout cas bo dég lo niari versions yeep do xaaam Kane mothiy wakh deuuggg
@@mamesodaniang3571 lolou la wakh dii tellement c cohérent toutes.
@@mamesodaniang3571 la famille de Aminata sen version n’est pas cohérent
@@wakhlouyydeffarnittgni4965 niari mère yi mom seni wakh cohérent woul dara nak,leur version à eux deux se contredisent
@@maimounandiaye5246 pourtant en se concerne le matelas suis d'accord à condition gnou changer matelas bii?
En tout cas avec la police scientifique de notre pays lépp dinna leer inchalla ?
Histoire bi métina lol mais yalla nako yalla yeureum té kharé aldiana🙏🙏
Affaire bi dal yalla rék mo kham yalna yalla réral lépou
Amine yalla na sougniou borome lèrale lep
Yalla rek Mokham Lii niaw na loll yalna yalla samal niou sounou ndiaboot gui délosi lenn khel yii 😭😭
Mane déjà pourquoi utiliser du pétrole dans une maison comme bon vous semble c’est pas sur n’importe quel accident peut arriver dans toute la maison paix à l’âme du défunt et que l’affaire soit élucidée
Yen ay parent you irresponsable guen
Adouna amoul solo sokhnaci. Gniaak mo meti rek bayil mou seed. Yalla moko beugué nonou. Yalna souf seed si kawam
Bayilen serigne yi te guen wolou yalla bakhna paix à son âme
😭😭😭😭😭😭😭🤌🏻🤌🏻🤌🏻🤌🏻😭😭😭😭🧏♀️🧏♀️🧏♀️🧏♀️😭🙆🏾♂️🙆🏾♂️🙆🏾♂️🙆🏾♂️🤦🏼🤦🏼🤦🏼🤦🏼🤷🏽♀️🤷🏽♀️🤷🏽♀️🤷🏽♀️🖤🖤
Mère. Bii kouko. Gis xam ni bandit la toux kat lay nourool te fenkat lay nourool kii mère kooba la chipp
@@coumbadiallo2430 ndèyi diambour la,sa ndeye kouko waxoone lii doula nex
@@coumbadiallo2430 fékone SA yaye doko wah lolu dh
@@MamadouDIALLO-fg8xk bilahi c'est des embeciles
Allaahoumma'ghfirlahou warhamhou wa afou'anehou.Yalla djeggueul leu té yeureume leu.
Yalla deellooossi khel yi,defaaraate djikko yi , samme niou ak sounouy ndiaboote.
Amine
Mais faut demander le chauffeur pour ce que mo demba à dit
Borom auto mbobou mane na léral lou bari 😇😇😇😇
Insbiii nak yalla rk mo khame……la maman est sous La Défensive il faut la comprendre…..la maman insbii biii diakhleii na Elle boulversé parceque amena problème yo kham nei daflaye eup doller……………liii eup doller dalle moy kiii gueine adouna yalla nako yalla yeure 🙏🙏
wakh dji wakhou gnouko dafa melni affaire de Ethnie leu ak caste . Les désaccords pour leur union surtout du côté de la famille du défunt. Pourquoi le mari a quitté sa famille pour habiter chez la jeune . l'histoire est plus complexe. Que la victime repose en paix
Bien vu, Effectivement y'a un pb. De caste .
Bien vu 🙈 on ne quitte pas sa famille 👪 pour aller chez la belle famille y'a un loup. Dommage que en 2022 on est encore là quel retard. Bref nous africains réveillons.
Diop casté amoul iow donc sûrement ethnie laye done nah halpular d'à beug seuyou mbok tei wadji halpular la xébanté batay ngui si !
C'est ethnie serrere ne respect pas les griot
Hummm la dame est paniquée cela veut dire qu"elle n'est pas franche.
Dofouñiou wayyyy
Vérité absolue lii mouy wakh dara douçii deugg
Vérité absolue lii mouy wakh dara douçii deugg …. Désolé wakhii doff rëkk lafii wakh
Tit na mom
Elle n'a pas l'air de dire la vérité
Lolou la guiss manite
Elle raconte vraiment du n'importe koi ..c'est même pas clair ..limou wax amoul bopeu amoul tankeu ...en plus elle n'étais pas présente sur les lieux son discours est honteux ...une personne est morte une personne avec une bonne intention demande à ce que justice soit faite même si c'est sa fille qui est inculpé c'est une personne qui est morte qu'à même...c'est pas un animal..en plus elle passe son temps à jurer ..c koi le.projet fi gnifi dakeu watt niofi dakeu.....
MERCI essaie d'écouter l'autre version et tu verras
Doul reik nguen dii deff ioe ak sa dôme wayei yallah dina lene atei ak nioune 😭😢 bouteille bii yako dioxei guemo serign Lutax ngay dem dii setlou ioe doul nga meune
K l’âme du défunt repose en paix 🪦🙏
😭😭😭😭😭🙏🏾
Mér bi limou wakh dara amousi keurou diaga yi domaram yi repose en paix ma démba😭
Bayil serigne touba
ya watte ni mouso dem si serigne et au début de tes mots tu as dit danga dem si Serigne mou wakhela denioulen dedeulé je m’arrête là . Ki dem yalnako yalla yereum khare ko aldjana thionom yem fii si adina 🙏🏾
Moma si diaaxaal cest chelou
Mo demba ke sa félicité soit éternelle 🙏🙏🙏
Lingaye wakh amoul cohérence dé. Yene danguene yakarner nit mome mane nga ko def loula nekh?amlene yeurmander té neke nit
Mane diga sodé sama frère di nieuw hôpital diko assisté bamou dhé nioukoy médiatisé tamite niou khalate touti trop de zone d'ombre dans cet histoire Yalla nako yalla yeureum
Tante Aïda mi doulkate la déh ioe niarr niou nékk sen négue nann rék nga meuneu dégué Amineta diko wakh souba dingama mayy sama batt yénn ayeu guénn trop non mais vrai scénariste
Gni famille bou bakhe laniou walahi té aminta yayame sakhe djioudouwoule khale bou touti le yayame diambar le masoule thiow té beugoule kouko Méré
Mane lima djakhal moy le gar bimouy dounde lou takh dieuloul ndjabotam yobbou sene keur mou nieuw deuk keur gorowam yi. Mou dè kou nekk di wakh. Vraiment je ne pense pas k la fille moko tal
Oie saytané deuk gars ak fein katt
Vraiment wadji wa kerum dagnuko beddi mère bi moko teye teye domam deukeul ko
Au moins yaw dangay halate
@@cheikhounadiagne5375 ah sangue bi tè mou rafet rek. Mane déy sagaw mala et je pense que la liberté d’une personne commence la où se termine la liberté de l’autre. Khamo ma khawmala na rafet rek. Mane nga diokhé sa khalat ci ay teguine ak taloubé. Nga balma
@@MADIDA100 désolé 🙏🏽
Man mom lérna ma ne yaw defou domou diambor dara mais sa dom def na
waw grand dom def na
Paix à son âme mais une histoire très compliqué n'a justice ⚖️♎ def ligueyam boumou bâyi mou sed
Quant là justice fait son travail normalement la famille de Aminata son victime parce que sen version yi bokoul je suis étudiant en droit j’ai écouté la famille de Aminata surtout sa petite sœur se qu’elle c faux parce que elle ne cherche pas de défendre mais elle cherche là bataille
Amina thior sama toma gua nio bokou tour AK sante
Liguay wakh yénou woul mana ragalal yallah mo demba foumou guissé pétrole à 2h du matin bayy taleu bopam si sa birii wakh négua guemo sérigne téh nga dém si sérigne ioe koula guiss khamné koba nga sa bouteille pétrole bi ngay tékk khel nitt gni
Franchement je la crois pas en plus pourquoi elle jure comme ça
Gni dagno irresponsable wayyy
Te bo khole botam yii defa melni kou ragal te tami nit ak noppam mo dee me yenga louko sakh
Yene doy ngene waarrr dh.. mere bi kiuko degueu mouy wakh khamner el est boulversé camiul fiumiuy takhaw nakh seu dom leign djigne rey nitt…
Ce cas est compliqué.
Très compliqué te amougnou soutoura
Mère bi jai beau l'ecoutè mais sama khèl tèy na trop a voir son comportement, as version nest pas crèdible
Ki bou police commencé enquête thie môme lép lér wakham doyena war thé toujours wat kat dou wakhe deugueu
@@ousmandiallo8404 ssisi dè que tu regarde son comportement tu voit qu'elle fais la maline, apres sa fille la police doit se tournè vers elle.
Mère nianalall ki mo guèn lakk dom Sankk dom wakh bii rafètou sa dom rék Guay protègè soutourall ki dèm 😭😭😭
Paix à son âme yalnako yalla yeureum te kharéko aldiana
Yalnako yalla yeureum
Maman yaw tu ne dit pas la vérité ndakh geumo Serigne tes déme Di sétlou ay nitt gay wakhal Sénégal Moy deuk bo khamni dagnoulay togne ba paré Di weur Di wakh yaw so néké ak sa goro si birr keur gui témagnoulene diam doko guéne mes yaw môme ligua wakh dara lérousi
Kou gnimè yalla ki mako kham
Mère bi kou meuna fene la nikaye wakhé daga titte mais yalla des amna
Ndaye mareme mère bi dafa meuna fene tongne ba paré di doule
Domam lay sauvé nih deh mouy doull nonou
Wahoul ni geumoul serigne deh
Mais daffani meussoul tahaw si serigne nane ko defaral ma li si digeunté domam ak mor demba
Deglou wat ko
Mane liima diakhaal mooy khana au moment des faits yeen nieup dagueen Fébaroon ??? La 1 ère et la 2 ème dames yeup nénagn seen yaram nékhoul woon ?? 🤔🤔🤔
Sibarou dèye wallé!
Yalla n’a sougnou borom leral lepeu inchalah
Kou dée werrou
Mère pour ioe ay dof nguay waxal ragual léen Yallah famille kou gaur ki louniou wakh mo gueneu léer di kharou ba paré di sauvé sa bopou foumou wakh
kouy kharou key soula metite bi eupai dolai sigua diema guaineu si livua naik,côté bobou mom c est normal kaineu antanoul yaineu metite yi
@@millesmots2881 rakou khalé bou goor bi thi bopam mo wakhni khaléy bou goor bi moko wakh néko soumadone kharou douma dièma sauvé watt sama boop doyna war dé yalna yalla leral yeup
@@jolieseye403 ça veut pas dire que daf ko wakh lolou rek deug la. Meune na ame beugoul wone wa keuram yi kham ni dafa dane djéma kharou ndakh gatchè. Ak lakk nimou métiwou, keup kouy lakk digua djéma sauver. Déé yomboul dé. Yalla rek mo kham nak
@@ouleyngom9157 mandouléne si wakh bi ki déme na ba paré nagne ko gnianale et aussi yana yalla lérale lepp in challah 🙏🙏
@@blacklady6356 dagua guiss ma wakh ni mbir bi ni wala ni la démé? Wala ma déf fi béne jugement wala dara? Bayi léne togn akki douggal nitt. Fekké wouma té deuggal louma fi dara. Dama apporter sama avis si bene commentaire bou spécifique paré préciser ni yalla rek mo kham li khew. Daguéne gnémé aye wakhi mandouléne torop pour un oui ou pour un non vous saoulez les gens avec ça. Boy woté mandou loy gneuw setane ci vidéo bi? Loy liré commentaire? Loy tontou commentaire? Sof guéne torop way
Soxnasi famille bou salte ngeen chipp
May his gentle soul rest in perfect peace ndeysann very sad 😞 the stories that has been said from both families r all different but Allah knows best may justice served
Lima diakhale moye yawe miye wakh deudelé bimou fébaré yafa yobou safara kone ya xame serigne deugue nékhoul liguaye wakh si yawe la nek esqua deudelé woko ak famille dakh limou léne di diarigne
Vraiment
Bilakhi yokal volume prck louche mongui thi
Moma diakhal
Linga wax moy deug
En tout cas même si le défunt ne faisait rien à la maison, vous êtes restés avec lui Vous avez confirmé que c'est un homme à douze métiers . Où a t il dépensé son gain, vu que ses propres parents n'en bénéficiaient plus ? Paix à son âme Amine
Nèkal fii Sénégal Borom 100 métier sa veut pas dire que tu as de l'argent,boul fattè deuk bii dafa méti
@@papediop9404 pp
Walahi je connais l'homme nite guenou ko
@@papediop9404c'est bien vrai mais vous n'allez pas me dire qu'il ne gagnait rien
@@aminatamamadousow7275 boul ma wakhe loo louma waxoul,louma xam ba xam daal deuk bii metina danguay liguéy ba dè doo aame xaliss
Repose en paix mon frère
🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐
Yalla kéne la♥️♥️♥️
Paix à sn âme qu'il repose en paix
Jigguennnou Sénégal sonneu n'a sa dieukkeur violent kharrou niou dilla accusé à tort. Vraiment li mettina trop. État Sénégal daniou warra jappaler jigguen yii
Ioe do wah deug ki dafeu dh ngakay toumal nane leu nite di violé diabaram ba baré xarru
Ioe kou niémé yallah nga djiguen bou diarra diapalé niou diapalé la ioe mom kénn doula diapalé
Bilay
Ki ta dit que dafa kharou ragalén yalla
@@Bambaprofil même souko jabbar ji sodder réfléchissez sur ce que la femme a endurée. Au Sénégal on n'oublie que la femme est très fragile beaucoup de femmes sont devenues dépressives à cause de leurs maris. Le mec vivait chez sa femme. Donc réfléchissez en bon sénégalais sans être hypocrite. Rufisque les gens de Rufisque se connaissent si la femme l'avais brûler le matelas allait brûler.... Réfléchissez...
Mani sen wax yi bayi len di thi watt ay Serigne Touba ak serigne Saliou ak Serigne Fallou m. Arretelen way c vraiment agaçant
Yeinite deh niou bone ngueine nianalolene sax seu dieukeurou dom dji
😭😭😭🙏🏾🙏🏾
Yalnako Allah yerem té khareko Aldiana firdawsi ak mbolem dioulit. Amiin yarabbal Al Amiin l.
Yaw mome say wakh doyouma 😭😭
Deugeul monan ma dem setlou bayilen bokale te di juli di nian Yallah
Sa ndeye sakh deye Setlou
En tt cas yallah rk mo kham pask ç que la dame dit néna dieukeurou domam bi famille Wam dagn ko béddi considèré wougnou ko ça semble vrai pask son pére desque mou dégu ni domam essaie de se suicidé il n’avait ps réagi il a même dit que dafa dém liguéyi normalement meunone na kholi domam bane état la nék ç vraiment compliqué Que firdawsi soit sa demeure🙏🙏
Kou meuneu séneu Ay grand xamo Ay agresseurs lagn ou pas nga continuer sa chemin looy ragalé ay xath bay wagnékou 😒😒
KII C UNE MENTEUSE DE CLASSE EXCEPTIONNELLE . TROP DE CONTRADICTION :ELLE RACONTE LE FILM EN DISANT FÉKKEWOUKO ; MOUSSOUMA DÉM THI SERIGNE DEUKK THI SÉET KATYI ; LE DÉFUNT AVAIT FAIT TENTATIVE D'IMMOLATION , POURQUOI CONTINUER DE LE GARDER CHEZ TOI ,? SES ARGUMNTS POUR DÉFENDRE SA FILLE ST MENSONGERS . PARFOIS SEUGN FALLOU , PARFOIS SEGN SALIOU GUEUMOUL DARA ; .KOUTAAL BOPPAM DOU WOUT SAUVETAGE THI CANAL
Dego mouné dafa retourner am koumou andal khadj dou nitt bb
@@senegalaise9527 lgui gars yimou guisson t xamoul ndax agresseurs lagn ou po n'empêche mou continuer yonam...t bimou démé bassi porte bii xana Dina feug t forcément Dina am tidji t douko bayi ak kath bi
Thieuy walay
Affaires yii daal xamougnoussi dara mais waxou soxnassi amna Ay incohérences waxoumani elle n'a pas raison nakk mais wax bou dioup xamnagnko 😒
La famille du defun amoulen lolen wah danguen beddi won sen dom tay lii am ngueni amerde nit gni la dame lou mun ti khew mom teyè n'a domam ak dieukeru domam
C'est pas beddi mais lui même le gars sa famille est en location et aussi il a tous fait pour la fille et ensuite wadji il n'était pas un chômeur il était chauffeur et j'affirme que je connais bien l'histoire et je suis de la même famille avec le défunt merci de bien vouloir révisé une histoire avant d'en parler
Koula wakh dagnio bedii seendom mounna am mo bouga nekka ker gorom yaaye bo giss bou sagnion domam ci moom lay nekka
😢😢
Légui féeeenn komm nane dokh.... mère bii noumouy wakhèee ak geste youmouy deff niii nama yalla baal .... yalna y'allah até lepp lérall lep
Yalna yalla leral leep… ki dh yalnako yalla kharei aldiana… hypothèse tal bi mom sa tient pas la route
Kou ddd ak sa bamel yako wakhal sa bopp Kone yalna yalla niite te atte lene kom fekewo warro di insiste si mo tall bopam ndakh makk nga te police scientifique kharagn na lool sakh mo tall wala dagn ko tall mo tomba determine lima diakhal moye yagui watt si li khamni y’a wakhni fekewoko comm esk do bayi rek justice deff yonam defante d lafi guiss ki dcd fate guene ko
Paix à son âme 🤧
Dioulit bouy dem si set katt.dou djioulit deugeu kou ragaloul yalla meuno yar sa dom
Yen kay yena setane ba affaire bi akci fi. Kou menacer damalay taal Dina la raay ak Di khekh toujours
Bou bi mou wate tchi serigne fallou bénéne bi mouni serigne saliou
3:36 dsl pas de cohérence elle n’est mm pas à l’aise😓Yalla nako borom bi yeureum
Oui
Bravo journaliste
Yéne danguéni diékhal xôl yéne famille bi doul rk nguéni déf niak nguéne diom trop yaw fi kofi plainte gnou niouss la té nguéne tokk 😭😭😭
Lo bokk Ak sa domm bi🤣🤣🤣🤣 Souma nekone mère bi dama nane ko Sama cousine la😂😂😂
Seul DIEU qui peut juger
Fatou tu as beaucoup de version
Histoire bi doyna ware lol li daleu métina yalla nako yalla yeureum té kharé aldiana
Non soxna si sa goro lakk ci sa biir keur. Te demoo yobbou KO hôpital vraiment doo nit kou baax yaroo sa doom ji toppal feule
Nitt kou baxla xamoko boul jugé stp
Yaramam nexoul wone xana do degg bayilein di juger nit tei Xamo lein ko
Mére yaw domaram ngua rek koula khol kham ni yaw koba ngua te dara safou la yaw gnou wara ték sa dom si yone ngua nane damay porte plaint yaw kou réw ngua😭😭😭😭😭💔💔💔💔
Bilay
Qui ngay wakhal dh nit kou bakh leu yalla rk mo takh may wakh liguey rk leu kham amoul bén problème
Kane moy nitte kou bakh fofou
@@salyallemomuawrksarr8652 del wakh lo kham
Goor bou takè diabar nako yobou Bo ame diom
Sa Way Mandoul Nak Nitt Dey Wakh Liko Woor
Gni di wakh hamnagne la maman ou la fille, vous n'habitez pas ensemble, vous étiez pas la au moment des faits et vous ne savez réellement ce qu'il y'a entre les 2 conjoints, donc mandou len. Ndakh nit khamko si ay blancheur dents rek, takhoul gnouy wakh. Yallah rek kham. n'a yoon Def ligueyam, y'a mort d'homme malheureusement.
Lieu crime bi le personne waroul wonn am accès vraiment
La maman de aminta explique les faits comme si elle était dans la chambre. Yallah rek mo kham aallahou aalam
Lamègne dou lèkke moromi lamègnam tè gnoroul,wa keur kou gor ki gno wakhe mère def réplique
Ligua wax dh moy waxou nit
Bilaye ndiaboot mo sonou,peut être que Mo Demba avait des problèmes psychiatrique, métina dalle yallah nako yallah yeureum té diégeul ko aye bakaram , yallah rek mo hamme lou khéwone ce jour que firdawsi soit sa demeure éternelle Amine !
Écoute l'autre version de fait
En plus seulmant lui a pris feu pas le matelas
Len deh khamnako setane ngen trop fou eumbeul ame 2 fois seuy am fa te Diam amoul ngeni setane rek bparer le gars mom bimouy nek keur mere bi Ani famiile yame yemer na deh a mon avis so eumbeuler nite 2 fois koum takhawal ngeni faram la confiance doufa ame finalement mom mi decedes sakh Ken doukou Tala gnanal
Geumo Serigne té yangui sedlou ah way
Lolou maman diakhal
Moma diakhal mane
🤫🤫🤫
Yakarléne yalla
Yalla rek mo kham Yalla nako Yalla xari aldiana firdawsi Yalla na yalla léral lep té svppppp bayilen di wat si serigne yi ak Yalla si lo kham ni moy lolou t’es perturbé maman liguay wax ni Yalla baxna on verra liguay waxni baxna té guene bayi serigne yi encore une fw merci liguay wax sou néké degu Diaroul wat
je sais pas pourquoi mais j’la crois en plus mère bi diapp neu si seuy bi khékh yi dal gua waronn bagn
Gno yam deh vraiment sougn ko bagnone dougn ko fatt. On peut comprendre les incohérences ndax nena fekeiwoul bi kei di tal bopam. Donc li nit yi wax fofou rek ni moko lak lolou la meuneu wax.
Elle l'a pas tué.. J'ai vu la chambre aucun matelas et mur brûlé.. C'est un accident je peux confirmer sa femme ne l'a pas tué.
Mere bi néna dadone nélaw aprés mou explique evenement bi
Moma yéme
Ha moma yem