'Dafa Takk Niarel Sokhnam Teudjko Thi Negge Bi Indi Coour" Les révélations de la mère

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 17 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 1,5 тис.

  • @ndeyembodj9396
    @ndeyembodj9396 2 роки тому +116

    Pa bi kou mate kilifa bilay 🥰🥰🥰♥️♥️♥️♥️

    • @footballgod4351
      @footballgod4351 2 роки тому +6

      Vrement yalna goud fane way il a bien eduquer sa famille machallah

    • @awagadiaga9553
      @awagadiaga9553 2 роки тому +6

      Bilahi dafa yarou sakh pa bi

    • @ndeyembodj9396
      @ndeyembodj9396 2 роки тому

      @@footballgod4351 amie et machallah

    • @ndeyembodj9396
      @ndeyembodj9396 2 роки тому +1

      @@awagadiaga9553 bilay eva

  • @cheikhounatine758
    @cheikhounatine758 2 роки тому +261

    -Rien ne justifie la violence que la femme a fait preuve hein.
    -Si vous n’êtes pas en mesure de supporter la polygamie mais vas-y demande le divorce c’est mieux que de faire du n’importe quoi.
    -Je salue La sérénité et le respect de cette famille qui n’a pas déversé sa colère sur cette pauvre dame parce que ça pourrait mal terminer

    • @nabousanediop6840
      @nabousanediop6840 2 роки тому +8

      Vraiment,fii ken forcé woul ken woudiéi ,

    • @cheikhounatine758
      @cheikhounatine758 2 роки тому +1

      @@nabousanediop6840 ah vraiment si tu peux pas supporter bah force pas

    • @smartfolle
      @smartfolle 2 роки тому +7

      Lii daal moy waxx dji
      So menoul mougn woudjei nga demm sayoon
      Souko reyoon tamit moy perte mom ak wa keureum apres niou niane intervention teudj ko klk mois mou guénaat seuyi fenen

    • @arabiatou.coly1696
      @arabiatou.coly1696 2 роки тому +1

      Bilay deh la violence ne résolve rien

    • @maimounadary9726
      @maimounadary9726 2 роки тому +4

      khana kou divorcé dagnoukoy délo ndawam

  • @fantasagna4076
    @fantasagna4076 2 роки тому +34

    Firangué bou eupë bakhoul djiguéne,dafay nangoo mougne lo guiss rk dafay jèkhe ,firé ko ba nar Ko lôr ,gnoune djiguéne gni nagnou kholate sougnou takhaway bou bakh,ay joulite laniou tmt nagnou nangou woudjé té woudjé dou dara loudoul niar niou bok weuseuk,bon rétablissement à l'homme 🤲🤲

  • @marietoubodian5395
    @marietoubodian5395 2 роки тому +15

    Nagnou taper khollei yii teh yar soniou bopp kou d'accord beusseul j'aime 👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿🇸🇳

  • @ibousyllandao9322
    @ibousyllandao9322 2 роки тому +26

    Vraiment famille kou goor kii koulén diapou diapp niou goré papam ak yayam

  • @hawasall4148
    @hawasall4148 2 роки тому +6

    Ndeysane famille dieukeur dji danio baxx ndeysane

  • @Vincent-zp2pq
    @Vincent-zp2pq 2 роки тому +58

    Deug deug dieukeur dji meun na mougne nk. La famille du jeune homme est très reconnaissante malgré les faits.

    • @ahmadouniang2774
      @ahmadouniang2774 2 роки тому

      C pas la reconnaissance c'est d'accepter d'être tué raison pr la kel justice Sénégal ne pourra pas avancer c'est le contraire ici europ

    • @Damasdiagne0402
      @Damasdiagne0402 2 роки тому

      Bilay

  • @binetasy3749
    @binetasy3749 2 роки тому +78

    Mariage Sénégal mo metti Tei compliqué . Seuy leigui danger pour les deux familles . Motakh ndiabot you bon reik kou neik di tangal xolou keinein . Vous les hommes j parle en connaissance de cause xamolein koulein di monieul doxane reik do lein doylou .la femme n est pas mauvais c juste c qu elle a vivre la conduit ainsi . Bo doundeul yein situation doko xam .mon mari ma tromper avec 2 femmes et lorsque j l ai surpris il me dit k il n a jamais l intention d en épouser donc louko fi diar . En plus u vis dans une grande maison ak ni keur gui metti bo yeureumoul sa soxna boul ko teik nakar . Elle a juste aller top loin. Ak loumou meunti sone si u supporte pas part au lieu de te salir goor diarouko mais force à toi sister

    • @magattgaye1760
      @magattgaye1760 2 роки тому +1

      Wlh ndiabote you bon agresseur je ne suis pas d'accord comme ray nitte c pas normal est c q amoule rap

    • @thiamthiama6552
      @thiamthiama6552 2 роки тому +8

      Mane déh djomi na maye wakh mounan force a toi siste ki beugue raye domou diambour boudone sa mack lako déf do wakhé ni sou mounoul woudjé gua déme cest sinple tite na si senegal khalé you gour yii faga rouléne djiguéne vampir yii gno fi

    • @binetasy3749
      @binetasy3749 2 роки тому +1

      @@thiamthiama6552 force à elle li niouy dathie thi keur yi vous en savez rien yein célibat yeina fi neik di sonal nit Gni . Elle est juste aller trop loin mais son comportment peut être justifié

    • @coumbaba6530
      @coumbaba6530 2 роки тому +1

      Walay sister liga wakh khamo sakh lulako wakhlo. Gorru tay yiii niaaak nagn diom amuniou roussukay, moi non plu sui po d’accord vk l’acte d la femm mai la source d cela c’est l’homme.

    • @binetasy3749
      @binetasy3749 2 роки тому

      @@coumbaba6530 elle a exagéré mais c ki au fond on ne connaît . Elle a juste trop endurer les femmes souffrent dans leur ménage desfois elle n ont personne à qui se confier ce qui leur pousse à agir inconsciemment j sais au fond elle est regrette son acte

  • @anijara9636
    @anijara9636 2 роки тому +156

    Même si je comprends que ça doit faire mal d’avoir une co épouse ce n’est pas une raison pour agresser son mari. Si tu n’arrives pas à supporter la polygamie divorce et rentre chez toi c’est tout.

    • @simalcoura9093
      @simalcoura9093 2 роки тому +3

      Sa deuggeu deuggeu kou meune tok so menoul gua dem

    • @sophiesokhnacorrea1196
      @sophiesokhnacorrea1196 2 роки тому

      Dém pour lane esk dieukeureum warou ko,waur nama daf ko nèwone douko meusseu takal woudiou,légui dangén beug mou dieul ay bagagam dém,bane goor tak ko,mou bayi keureum nonou bénén djigén diffa dagou?

    • @mariendiayediouf8363
      @mariendiayediouf8363 10 місяців тому

    • @mariendiayediouf8363
      @mariendiayediouf8363 10 місяців тому

    • @MaimounaDieng-o4j
      @MaimounaDieng-o4j 10 місяців тому +1

      Ki môme vraiment domerame la chiiim

  • @antasarrcisse1803
    @antasarrcisse1803 2 роки тому +189

    Une belle mère exceptionnelle !!!!

    • @salimatasow2622
      @salimatasow2622 2 роки тому +2

      Vraiment

    • @mamefatouba6637
      @mamefatouba6637 2 роки тому +9

      Bilay ndeysane mais seytane dafa beuri dole PA bi beuguenako MÈRE bi aussi yalla sunuu borom def si jaam rek amen

    • @salimatasow2622
      @salimatasow2622 2 роки тому

      @@mamefatouba6637 Amine

    • @bourtandadiop3261
      @bourtandadiop3261 2 роки тому

      Vraiment d’accord avec toi. C’est triste

    • @nenou2d846
      @nenou2d846 2 роки тому +6

      Pa bii ndeysane il est choqué
      Kou bakh lay nourou
      Ndeye tamite am na fitt si femme
      Papa doundal way

  • @paabdou8773
    @paabdou8773 2 роки тому +95

    Yalla naniou yalla Def Diam ak soutoura ❤️🙏🏿

  • @lalasoumano9139
    @lalasoumano9139 2 роки тому +37

    Gnii vraiment famille gniou bakh lagniou malgré kou djiguèn ki limou dèf sen dôme takhoul gniou sèdèlko dara Lou niaww

    • @marinaba9574
      @marinaba9574 2 роки тому

      Ndeguene da ma bakh rek gnou wakh ko é aussi cheikhouna borome kholou diama billahi ko beugua djiabarame lolou mome meuna ko séde si gnome

  • @SweetDidja
    @SweetDidja 2 роки тому +74

    La dame a eu à faire avec une famille éduquée et respectueuse motakh elle s'en est sortie indemne. Niit tak djabar takhoul mou bagn la, soko meunoul mougn rek demal. Yalla nagnou yalla doli soutoureu

    • @tantylarose809
      @tantylarose809 2 роки тому +5

      Bilay bien éduqué teksi dal si ctei la mienne dou dmei ni

    • @bellawomen
      @bellawomen 2 роки тому +2

      Comme crime d je te jure kou takk niarel diaroul ii

    • @NdeyeMbarkaWade
      @NdeyeMbarkaWade 10 місяців тому

      Jarouka mom ndakh bouko rayonne daniouma koy teuth

    • @maremediallo3053
      @maremediallo3053 10 місяців тому +1

      Ki dall défoule loudoul réw AK Bone AK sokhoré AK néégue gnoul bir ki d'où nite dafa té kou beugué nité doko déef Lou Bone wakhatoumak diko diame sakh pousso tank niarréle mène mougne menouko ngua dém

    • @minalo7618
      @minalo7618 10 місяців тому

      Vraiment 😢

  • @ouamarjohnson9346
    @ouamarjohnson9346 2 роки тому +59

    Vraiment la mère est une vraie responsable ♥️bravo

    • @ndeyemboup9394
      @ndeyemboup9394 2 роки тому +1

      Bilay ki Mo bone assassin 😡

    • @ouamarjohnson9346
      @ouamarjohnson9346 2 роки тому +1

      @@ndeyemboup9394 métina trop li thieye djiguéne

    • @coumbadiallo2430
      @coumbadiallo2430 2 роки тому +1

      Sénégal dagnouy maslaa bâ gnou rey la sa famille perte

  • @ndeyembathiodiallo5723
    @ndeyembathiodiallo5723 2 роки тому +8

    Khawe maléne dé wayé famille bou bakh nguéne machalla

  • @myasarr9779
    @myasarr9779 2 роки тому +85

    La deuxieume femme n'a qu'a se tenir prete l'ex epouse n'a en pas finit.yalla mousseul niou thi seytané.

  • @nettadiop8814
    @nettadiop8814 2 роки тому +65

    J'aime bien la réaction de la maman et du papa

    • @taftaf3989
      @taftaf3989 2 роки тому +2

      Mande diguene bouma soty dokhe mou tangue ninale yall ma bania doude dakhe kene fekhe ba doumala defe loiko raw daniye dof doflou rew rek molene diap koula soty bo were fayoule ak foumou mana nek

  • @mbneseye2213
    @mbneseye2213 2 роки тому +9

    Ndeysane famille bou gorée c’est rare loumou méti méti sedel naniou ndawsi lou bakh dans le passé

  • @maimounasow5854
    @maimounasow5854 2 роки тому +72

    Danguen gnémé masla trop kou gnémé arme ken douko teuyé si keur

    • @ndiemendiaye9979
      @ndiemendiaye9979 2 роки тому +4

      Bilakhi wakhatico suka baye dinaka rey de

    • @ndiemendiaye9979
      @ndiemendiaye9979 2 роки тому +3

      Bilakhi wakhatico ki de meune n’a rey khale bu gor bi

    • @quenne_dudiolof9536
      @quenne_dudiolof9536 2 роки тому +2

      Djiguene kene douko trokhal. Sa femme a fait bcp de fausse couches pourquoi mou dem takk 2eme femmes

    • @bilalkhalyfall9938
      @bilalkhalyfall9938 2 роки тому +2

      @@quenne_dudiolof9536 souko nékh takeu beu 4 djabar lolou kénéne mounoussi dara il a signé polygamie moment bouko nékh lay takeu djabar il n n'est pas obligé de tenir compte yaw liguay wakhni arrêtes d'être l'avocate du diable mm si j suis d'accord peut-être warone nako yeureum mais mou takal ko gnarél lolou dou délit

    • @quenne_dudiolof9536
      @quenne_dudiolof9536 2 роки тому

      @@bilalkhalyfall9938 khamo louy fausse couches. Surtout femme bouko subir plusieurs fois. Li moy trokhal sa diabarre.

  • @a.barhamcisse7290
    @a.barhamcisse7290 2 роки тому +75

    Moytoulen djigenou mougn kattt✌️lo wax mou rèèè Dou am problème banga yeuk ko bari soutoura...boul fok ni nitt ki amoul louko méti parceque sénégalais dafa tamou nitt kou am diam di kaf di reee xamaloko ben problemam ngani kiii dafa yarou ...deug la day fek mou nek nitt kou baxx kou oyof kou amoul ben problem mais nak au fond limou doul partagé day taxxx mou dègnthiiii ti dadialè si xolam...mane deuk na ak kou mell ni mais bouma xolè kanamam guiss noum melll rek damay xamni cv pas damay tok di waxtane ak mom di kaff ak mom bamou waxma liko méti ✌️delen bayi xel sen diabar yi boubaxxx nittt kounek amna problème Kone delen si bayi xel .ki li gorom wax rek war ngen xamni nittt rek la yalla nanou yalla mousal si seytané 🙏

    • @lenafaye145
      @lenafaye145 2 роки тому +2

      Je suis d'accord avec toi

    • @loufatechno2145
      @loufatechno2145 2 роки тому +2

      On s'en fiche ngay sisou nii

    • @binetaba3278
      @binetaba3278 2 роки тому +1

      C'est difficile

    • @etherlynelander4848
      @etherlynelander4848 2 роки тому +4

      Je suis d'accord avec toi. Mais tmt yalnaniou yalla mousseul ci genre djigueen yii

    • @s.ndiaye4186
      @s.ndiaye4186 3 місяці тому

      Tu as tout dit. Cest vraie

  • @nafimbaye8572
    @nafimbaye8572 2 роки тому +27

    Les hommes n'en valent pas la peine si tu peux pas supporter la séparation est la seule solution

  • @mamysakho6193
    @mamysakho6193 2 роки тому +55

    ki waroul neik si biti.non femme bi assassin deugue leu.dakodone rayyy Allahou Akbar.djigaine Dina neiguei ni

    • @deugrek-gk3lx
      @deugrek-gk3lx 10 місяців тому +1

      Police dako wara diap li dou yone

  • @missdiop3500
    @missdiop3500 2 роки тому +9

    Bayiléne di takk diabar diko gueumeloo ni doungéme meuseu takk gnaréle yénéy dougeul séne bopeu si problèmes yii yeupeu

  • @djkabou3006
    @djkabou3006 2 роки тому +3

    Ki amoulll. Diommmm ndawsiiiiiiii bouyabooo naguenkooo yobouuuu. Yarkooooo ndakh paregoullll yalla naniou yalla moussalllll. Si djiguen djioubone si barcké seydina Moukhamet psl amineeeee

  • @ipeneboubane6770
    @ipeneboubane6770 2 роки тому +180

    La fille est traumatisé avec les fausses couches au lieux de la soutenir tu épouse une 2ém femme cela fait 2 traumatismes elle n est pas consciente de ses actes elle est en etat de choc c est difficile quand on ne connais la psychologie

    • @sokhnandickembacketounkara7538
      @sokhnandickembacketounkara7538 2 роки тому +10

      ta parfaitement raison

    • @mariamalo6705
      @mariamalo6705 2 роки тому +3

      Vraiment

    • @khadijamiller6239
      @khadijamiller6239 2 роки тому +7

      Bilahi wakhal dé beug dieukeur sakh mais dafa ame louko méty rek Ndeysaan

    • @plumee.a
      @plumee.a 2 роки тому +33

      Ok les fausses couches et tout oui ouii c’est dure c’est traumatisant mais rien ne justifie la violence d’une telle ampleur en plus
      Pardon mais elle est juste méchante et sans état d’âme ton mari tu le poignarde tu le frappe tu lui fais des choses comme ça
      Si c’était l’homme qui lui avait fait cela ce serait plus choquant
      Ne donnez pas raison à cette femme

    • @almamyseckBouMameChekhIbra
      @almamyseckBouMameChekhIbra 2 роки тому +19

      Et pour toi c’est une raison de vouloir tuer son mari? C’est triste pour elle oui mais le mari a besoin d’avoir une progéniture et si sa religion lui en donne le droit c’est tout à fait légitime il faut que l’on arrête elle est juste méchante et jalouse combien de Femme sur terre n’ont pas donnés naissances et vivent bien kon bouniou ken sonal na niou ko niou ce n’est que de la jalousie excessive

  • @dieynarassoul1707
    @dieynarassoul1707 2 роки тому +337

    Parfois dinga beug seu dieukeur beu mou gagne leu nitt meu noko beug baa paré diko def lou metti gaur yi nio wara bayi dokhane bi ak ndialo bi niom niolay sopi une vipère une femme dangereuse rancunière et sadique elle a été déçu tout comme elle a déçue la belle famille

    • @dieynabafall6417
      @dieynabafall6417 2 роки тому +35

      C'est pas une raison ca même

    • @mirna90.
      @mirna90. 2 роки тому +24

      S'est pas une raison d'agresser l'enfant d'autrui

    • @khadysamb2824
      @khadysamb2824 2 роки тому +53

      Boudonne dokhane sakh c'est pas une raison. Mane dei douma masseu nek sorcière ni vipère ndakh khamouma Lou bonne ak Lou gnaw lolou. Seuy dagne na tass dagne na. Ya toujours une solution bou gueune li

    • @aissatouseck6242
      @aissatouseck6242 2 роки тому +39

      Gor gni dinane dokhane dinane tak yalla moléneko sédé woudiou diaroul li djigeene la com yaw rek femme yi nio wara bayi bégne woudiou

    • @awasoire2549
      @awasoire2549 2 роки тому +1

      Bien fait pour sa gueule niaw

  • @cheikhounatine758
    @cheikhounatine758 2 роки тому +81

    C’est une tentative de meurtre clairement,heureusement qu’il a un bon mari qui l’a pardonnée hein si c’était un autre elle allait mourir en prison.Qu’Allah nous facilite 4 bonnes pieuses épouses 🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿

    • @aminatadiop5275
      @aminatadiop5275 2 роки тому +1

      Amine waylolou rek mo diarra niane

    • @codoufaye3535
      @codoufaye3535 2 роки тому +1

      Amine 🤲

    • @Sabrun-jamil
      @Sabrun-jamil 2 роки тому +1

      Xalei bou goor bi limou deff sakh wooroul, parskel peut tenter encore une fois a sa vie ou a celle de sa nouvelle épouse

    • @abloslimshady
      @abloslimshady 2 роки тому +2

      Amiin

    • @deugrek-gk3lx
      @deugrek-gk3lx 10 місяців тому +1

      Dagnouko wara diap ki ray katou nit leu

  • @mamefatouba6637
    @mamefatouba6637 2 роки тому +58

    Yalla nasi sunuu borom wiss ndokh bou sedeu amen

  • @basiirumbegmi1832
    @basiirumbegmi1832 2 роки тому +7

    Lii de wax dëgg mooy nattu nag, xoolal ñii seede yu rafet yii, ñu ci wax.
    Wax dëgg Yàlla boroom gërëm de gu man a muñ la. Waaye jàppl ni gu muñ muuñ, te Yàlla ànd naag way muñ yi. Yal na Yàlla may soxna ci gën ci yaw ci barkeb Alxuraan Kariim.🤲🤲😭😭😭😭😭

  • @Lily-vb3gf
    @Lily-vb3gf 2 роки тому +25

    Adouna bamou dadje djiguenou senegal gnofi geuneu niak ambition beug goor ak seuy diaroul yenn yi si tu n’est pas contente si tu n’aimes pas partager ton mari tu le laisses mais kholal lii yeufi doff yi . Goorou senegal mom meunolen fekhei bagnouy dokh ci seni waaw si ils veulent épouser plusieurs femmes ils vont le faire ils sont polygames de nature boulen sonal sen bop

    • @LaBarhamienne
      @LaBarhamienne 2 роки тому +4

      Wakh deug ya allah, mane meunou ma comprendre goor gueneul la sa bopp, seuy diamou ya allah leu défal lila thi souniou borom santeu so meunoul supporté woudié bi, nga tass. Do togn kéne nga nék thi sa diam. Mais di rayanté ndax goor, n'importe quoi.
      Mane dh bamay guénak sama dieukeur laki wax biss bo také niarél moy souniou seuy diekhna. Am nga droit tak yalla lako may thi kaw nga meune ko, mane aussi amna droit tass ya allah mako may thi kaw ni antanouma woudié. Xoulo wouma, défanté wouma, xéxouma, sama bopp mala gueneul dou bagn nala😂😂😂waw key.
      Ins bi sou rayone dieukeur dji, bobou bakaar seuy warouko diaral kéne thi adouna. Mais sénégal mom seuy bi commr guerre dh.

    • @Lily-vb3gf
      @Lily-vb3gf 2 роки тому +1

      @@LaBarhamienne je t’assure ma belle certaines femmes sénégalaises vraiment m’énervent pour gnom sougn seuyoul wala sougn tassé rek elles ont raté leur vie elles concentrent tt leur vie sur les hommes et le mariage mais si tu n’es pas heureuse tu pars loufi diarr liii ? Man je suis comme toi dh woudié defantei khoulo khekh ak sama moromou djiguene ndakh goor soumako narei deff yalla na taka ba diekh

    • @BinetayoussouDiakhate
      @BinetayoussouDiakhate 10 місяців тому

      Niak classe rekkkkkk ak matadi woudjié dou dara diamou yallah kasé la

  • @aidambengue7019
    @aidambengue7019 2 роки тому +89

    khawma loutax gorou Sénégal yi beugue djiguéne rk dangay guiss ko khamni yoroul sakh loumou doundeulé awo bi né dafay takeu niarél déléne doylou djiguénou Sénégal yi djékeu nagnou raféte nagnou mashala té meuno am djiguéne yeup iow yaye doylou rk gueum yalla fofu rk laléne toubape gueuné toubape dafay khol béneu femme mou khamni iow la beugue bou takeu leu ték leu si wétam diapalé la diokh leu respect.....wayé gorou Sénégal khamoul valeurou djiguéne ay poubelle lagne gnou diapé war nguéne kholate séne bopeu dhé

    • @mamediarrambengue7660
      @mamediarrambengue7660 2 роки тому +4

      Merci Gentlemen si bopame Mo amoul senegal dangaye guiss boy bou Mole tak ko gnari fane mou sof la nga nek si deuke bi dikone gnak fayda gel bi mo moussoul rek gno bok Ben kogne doumala dor doumala saga tei nala nok tass ndank lay def athia gnou bok kogne bi nak leuh dotoko defatei

    • @marieme2961
      @marieme2961 2 роки тому +26

      Li ngay wax justifier woul violence bi beneu yooon, la femme a tord sur tous les plans. Boko mounoul mougn nga délou sa keur mo gueune li.. Famille bii danio baax rek wayé bou dessone ci mane yobou nagn ko justice

    • @aidambengue7019
      @aidambengue7019 2 роки тому

      @@mamediarrambengue7660 bly do comprendre dall

    • @aidambengue7019
      @aidambengue7019 2 роки тому +1

      @@marieme2961 batay déguo ma wakh si wakhou femme dhé

    • @marieme2961
      @marieme2961 2 роки тому +13

      @@aidambengue7019 mané ci lima lire tu donnes tord au gars qui sont polygames teh lolou justifier woul violences conjugales lala wax 😏

  • @dialloalibjibril6956
    @dialloalibjibril6956 2 роки тому +8

    Jabar dafa ame Sohna ame takk jabar jarul yakamti kholal ndéyam numuy Séyé ak réaction wa cognbi Sohna grate la jiguén bu nago mugne rek ngir séntu euleuk ay jabotame ame waye bu raféte yallah nanu yallah doli Sutureu

  • @madogydioufy7003
    @madogydioufy7003 2 роки тому +28

    J’ai pitié de cette femme wallahi ndakh beug nit limoula meune yobei doko kham
    Soula leirei ni tu es jalouse tei meuno supporters niarel divorcel dem sa yonne mogeun rafette li vraiment

    • @fatoumbackesylla4481
      @fatoumbackesylla4481 2 роки тому

      Billay yow me am na goor nio xamené solen niané bat dougn lako may dagn lay beunga nakhal

    • @khadijamiller6239
      @khadijamiller6239 2 роки тому +1

      Bilahi ndeysaan mais elle est incompris par la société khamouniou sa mbeguel Amna foy tolou dou amati saguo

    • @beautifulsoul110
      @beautifulsoul110 2 роки тому +2

      Yen dimbali len nit gni ngen nan incompris . Nit ko beug deug bien etre wam molay geunal sa boss
      Y’a rien qui justifie cet acte criminel. Sou wadji dewon dou lor ay mbokam ?
      Si tu vas mal à un point faut chercher de l’aide , s’ouvrir à quelqu’un, se gérer mais pas user de la violence
      Soudon le gars moko def niou yak ko ketemei

    • @mariamaba8738
      @mariamaba8738 2 роки тому

      Divorce d’où nonou dé

  • @mariamabandia777
    @mariamabandia777 10 місяців тому +1

    Pa bi môme machalla 🥰 kilifa la❤❤❤

  • @adjiabousso9129
    @adjiabousso9129 2 роки тому +147

    Ndeysane seuy dafa méti d’après les explications la femme n’est pas mauvaise ils l’on dit mais moytouléne djiguéne bouy seuy doko dégue mou clamer juste chaque dagua koy guiss mouy ré rék kham gua dafa nékhoul djiguéne di seuy di avorter à chaque fois qu’elle est enceinte 🤰 au lieu iow mi di dieukeur dji diapalé ko épaulé ko soutenir ko mais non certains hommes ne pensent qu’à leur bonheur égoïste pour satisfaire leur besoin daguay dokhane femme bi diko guiss di souffrire n’empêche mou tokk rék di rayanté en silence si bir négame bamou dém ba diour lii mais dafa am mots bo kham ni souniou kilifha dagne koy wakh tt le temps moy li bénén Mama bi wakh sank négou ndeye dara manqué woufa bayi lén lolou bonheur moy seuy certe la fille à deconné conseille boumakoy diokh nako bayi yalla diékhoul

    • @amymbengue6907
      @amymbengue6907 2 роки тому +6

      Violence dal fayuko damay gnan bat dem sama yon😏😓

    • @ndiayemouhamad4796
      @ndiayemouhamad4796 2 роки тому +9

      Ouii copain lu Leerr nga wax Lislam bénn niaarr niatt nieente yeepou na fekk nga Man ko rk Nioun nak mouy goor mouy djiguen Ken doxoull si diiné ken kouné sa banneex rk mola intéressé Loolu mooy warall mousiiba yeppou okk

    • @visionnairevisin861
      @visionnairevisin861 2 роки тому +4

      Rien ne justifie ce qu’elle a fait so meunoul mougne démal sétii lénene wayé beugue yobalé bakanou diambour pour lanne

    • @amidia5384
      @amidia5384 2 роки тому +1

      Mome kay dinako bayi ndax dinaniouko niouss ci KASSO bi yeufi sauwass yi moy lane

    • @rokayadiallo1500
      @rokayadiallo1500 2 роки тому +4

      Gor diaroul li

  • @adamandiaye4628
    @adamandiaye4628 2 роки тому +79

    Loussi meunti am dall mandou rek ndakh entre mari et femme Lou doy War la

    • @amatoullah6766
      @amatoullah6766 2 роки тому +1

      @youngboy boul boolé gneupp yowitam😂

    • @amatoullah6766
      @amatoullah6766 2 роки тому +1

      @youngboy d’accord naa ak yow thi benn côté aussi. La femme doit être réprimandée 😩

    • @badassglow402
      @badassglow402 2 роки тому +1

      @youngboy merci yéne djiguene yi dagno seytané ishh fokné Goor dou nite

    • @magattgaye1760
      @magattgaye1760 2 роки тому

      @youngboy mingui niaw deh 😂😂😂

    • @mbayeniass251
      @mbayeniass251 2 роки тому

      Yaw iska wér gua yaw

  • @siaraba2115
    @siaraba2115 2 роки тому +18

    Makhala legui sey nguir yalla mo amatoul. Deh len takk djingene bou am dîné. Sey dou afairou thiaga

  • @moustaphafall7397
    @moustaphafall7397 2 роки тому +48

    🤣🤣🤣🤣🤣 dieukeureum lou nawla.mariage comme divorce ça pas de mal.si le courant ne passe plus chacun ail chercher ailleurs.cest pas la fin du monde

  • @mimisy1269
    @mimisy1269 2 роки тому +25

    Ak loumou méti méti nga wara rouss sa goro bi la beugu té yalla takh nèkk nga trop nak amna nodone dokhalé dinga récupérer wate sa dieukeur té thiow dou djipe li mome daffeu eupe

  • @sambousmane6410
    @sambousmane6410 2 роки тому +71

    Non Femme bi moy domèram deug mo tax bayi lèn di takeu ay doff youy sagnssè aka poudeurouwou

  • @mariemecisse1490
    @mariemecisse1490 2 роки тому +4

    Ay way belle mère bou bakhéni famille bou bakh nga wara seuy ba dé. Nooo sama xol métina Bilahi wallahi niiit mo leundam 😔

    • @mbene-n7909
      @mbene-n7909 2 роки тому +1

      Gni mana kotou amou gnou mbam

    • @mariemecisse1490
      @mariemecisse1490 2 роки тому

      @@mbene-n7909 malako wakh liiii doyna waaarr

  • @aichandiaye439
    @aichandiaye439 2 роки тому +6

    Gorou Sénégal bakhouniou meunaniou féne meune naniou yakk khol

    • @SidyBa-pm4zn
      @SidyBa-pm4zn 5 місяців тому

      Tu es méchante 👹👹👹👹👹👹👹👹

    • @mystereseck3724
      @mystereseck3724 3 місяці тому

      Liga wax niaw neuhh, vraiment

  • @Madrequeen3173
    @Madrequeen3173 2 роки тому +41

    ayway li lepp boulasi naré fekk do tass gua dem mou dem mais li yeup diarouko

    • @moustaphaniang2183
      @moustaphaniang2183 2 роки тому

      Bilay diarouko

    • @tinabah1888
      @tinabah1888 2 роки тому

      Si tu divorce tu perds, tu peux rester dans ton foyer et le gérer avec diplomatie seytaner reck moo nooiw psk tout le monde on dit qu'elle est super gentille
      Parfois khaptal leye donn

    • @Iboudieng-bu4hv
      @Iboudieng-bu4hv 10 місяців тому

      yaw Khana khamoo jdigen bou firr 😢

  • @dieynabadiop4333
    @dieynabadiop4333 2 роки тому +15

    Ndeysane da beug rekk fire ba dof goor gni tamit dara lagn dee me li yeup solution bi moy dem sa yonn diarul wonn violence

    • @mbackefall3647
      @mbackefall3647 2 роки тому

      ko begeu doko begeu Ray

    • @mbackefall3647
      @mbackefall3647 2 роки тому

      @@dieynabadiop4333 sokhna si ay begeu amoul ko begeu bou dewé do seye akk kenen té yénakoy def

  • @mofama9520
    @mofama9520 2 роки тому +4

    Yallah naniou yallah mouthieule si djiguen thiou bonn

  • @mamadousall7046
    @mamadousall7046 2 роки тому +1

    Taak koula eup dolé woroul deee🤔🤔🤔 me vraiment pabi ak mer bi niou bakh laniou 🙏

  • @diagnepapa7813
    @diagnepapa7813 2 роки тому +19

    Ani Wa Droits de l’homme Sounekon Djiguén Wa Droits de la femme 👩 guénanu bou yag

  • @vap16.senegalbic76
    @vap16.senegalbic76 2 роки тому

    Oh sama xol toyna ndeysane la femme a plongée dans une crise extraordinaire metina la mère machalla

  • @dossoudiallo2813
    @dossoudiallo2813 2 роки тому +17

    Que justice soit faite maman tu as un grand cœur je t'apprécie beaucoup

  • @10gital66
    @10gital66 2 роки тому +6

    Vraiment des parents merveilleux ❤️ litax moutak 2éme limouy doundou mome moko xam en plus c' sont droit de pendre une deuxième épouse pour ne pas séparé d'elle ! Mon conseil est de la laisser partir et de resté éveillé car cette dame n'a toujours pas avalé le faîte que tu a pris une deuxième épouse 🙏🙏🙏🙏🙏

  • @maremesalihate1530
    @maremesalihate1530 2 роки тому +31

    seuyou légui yii dal diakhal nama lou méti li gua meune ko def sa dieukeur 🥺

    • @Sabrun-jamil
      @Sabrun-jamil 2 роки тому +1

      Bone rek ak niakka khalaat alahira

  • @mameseygueuye4540
    @mameseygueuye4540 2 роки тому +2

    Bilhi dieukeur dji aka bakh té yarou

  • @serignetoure9533
    @serignetoure9533 2 роки тому +12

    Bilaye papa bi manena kilifa lo
    Yalla nalla yalla miaye fane wogodou

  • @thiamaskoucawaty6644
    @thiamaskoucawaty6644 2 роки тому +152

    La femme a raison, comment tu peux avoir un seul cœur 💓 et aimé deux personnes c'est l'infidélité qui se prépare

    • @ndiayemouhamad4796
      @ndiayemouhamad4796 2 роки тому

      Hhhhhhhh😁😁😁ay waaaaaaay

    • @thiamaskoucawaty6644
      @thiamaskoucawaty6644 2 роки тому +3

      @@ndiayemouhamad4796 je m'excuses c'est juste ma pensée

    • @papesaliougeuye
      @papesaliougeuye 2 роки тому +10

      Yalla moko santané

    • @mamesodaniang3571
      @mamesodaniang3571 2 роки тому +12

      Toute femme qui ne veut pas de coepouse n'a qu'à signer monogamie

    • @khadijaelisebassene8217
      @khadijaelisebassene8217 2 роки тому +14

      Toi tu es une femme ou un homme il a le droit d'avoir jusqu'à quatre femmes c'est la religion qui le périmètre

  • @fatbintouhanne8560
    @fatbintouhanne8560 2 роки тому +3

    Cas dakoul liii 😂😂😂😂djiguen bii amna fitt goor bi ken dou mom di dokhane sachant k sa diabar mola soutt less delen takk kolen atten wayé wow kongou di takk diogoma 4g 😂😂😂

  • @mapdk6204
    @mapdk6204 10 місяців тому +2

    Khol bou yakkou meun na lou nekk..... Les hommes, la femme sont du sang et de la chair. Un être qui peut tt supporter amoul. Ay niit kessai lagnou. Boy takk niit Wakh ko lou leer khaalko ni tu es polygame. Les promesses et les mensonges gno tass sey yi. Quand tu veux épouser nakh tanal ak sa awo, si elle n'est pas d'accord choisi entre elle et l'autre. Les gens calmes et souriants renferment bcp sur eux. Il ne faut pas abuser de leur gentillesse.

  • @aichadiawara8908
    @aichadiawara8908 2 роки тому +11

    Non mais ki mo sokhorrrrr 😢😢😢😢😢

  • @pendafall9903
    @pendafall9903 2 роки тому +29

    Ay bado lagne dougne yore salama lekoume gaye mougne di mougne ba yalla niew niou nela fi nioukk seti lenen sa xole bi di wade ms li mome dou ma si fekk sou ma meune tok tok sou ma meunoul deme mou dieh

    • @fatoumbackesylla4481
      @fatoumbackesylla4481 2 роки тому +3

      Goor dafa badola de

    • @oumyniang2992
      @oumyniang2992 2 роки тому

      Merci penda ay domram lagnou

    • @mamalick4817
      @mamalick4817 2 роки тому +1

      Boungine wakhé goor rék bolé ngine si séni pape ndagoulén dogale yalla mon déf goor amna droit takk ba 4 femme mane Mangui ak ñiarri diabar té amouma bén problème yéna seyeutoul rék dangina yakarni yéna yilif sén dieukeur yi

    • @pendafall9903
      @pendafall9903 2 роки тому

      @@mamalick4817 kou nek ak sa bolou mouniou kaye ame na niouko meuna mougne ame na niouko meunoul bagne bako ba damani soko meune tok sokko meunoul deme man mome kou ma takal woudiou da maye guena tokk rathie

    • @fantadiop5504
      @fantadiop5504 2 роки тому +1

      Mane dhé lim déf c trop sadique vraiment, mais goor yi tamite war nagn kholate séne bopou, bolési yakk kou djiguene ki mou dém mba kouko guiss dotouko beugu ga commencéko négligé dakh séy dafa méti.. dagay toppou séy bi mba fouti mounélafi gnioukkou weuri kénéne, thiiiiiiiiiiiimmmmm....

  • @abloslimshady
    @abloslimshady 2 роки тому +5

    La violence dans un foyer est à bannir, que cela vienne de l'homme ou de la femme!
    Elle a mal agit en faisant ce qu'elle a fait à son mari, honte à elle!
    Mais la belle mère est vraiment exemplaire, chapeau à elle!

  • @ibrahimafall2376
    @ibrahimafall2376 2 роки тому

    Il faut protéger la 2ème femme nakh ki dafa capable de tt la familles est adorable machallah yalla nassi sounou borome df ndokh bou séed amine

  • @SENEGAL303
    @SENEGAL303 2 роки тому +208

    Ce que la dame à fait est dangereux.
    📍Mais dangay am sa sokhna,
    mou beug leu, décider seuyeul leu.
    Ngeu niak doylou Di dokhane.
    Mou diépi leu nakh dotoul am confiance ci yaw.
    Dila Def you sew parceque dafa am louko méti té yakoko ték, mouy vivre avec un amour sans confiance.
    Après ngeu diouk nane Sama diabar baxoul.douma seuyeul naouti bénén diabar.
    Fek lép yako Def.
    So doylou wone. Sa diabar dîna la seuyeul AK xol. Djiguén bou beug Lou é lay Def.
    📍bayi len Doug ci dieukeureu diambour yi. Djiguén yous si beuri dé a té AK nateu sén bopp molène ciy dougeul.
    Mais kama toudine,toudane. Lo Def sa morom dingako guiss.
    📍gor yi nagnou dang doylou. Djiguén yi Ken meun lén diexal.

    • @paabdou8773
      @paabdou8773 2 роки тому +29

      Mai Nespa ay dioulite lagn amnagn droite ame 4 femmes

    • @mairamediallo4043
      @mairamediallo4043 2 роки тому +27

      C'est pas une raison de faire des conneries en plus quand tu signes pour la polygamie doit être à mesure de supporter les conséquences

    • @SENEGAL303
      @SENEGAL303 2 роки тому +10

      @@mairamediallo4043 lissez ma première phrase. Je ne cautionne pas. Je sais just de donner les raisona selon moi. Pour que niou moytou

    • @maguitakontey6183
      @maguitakontey6183 2 роки тому +8

      Juste Parsk dafa dokhane non mais areter ka même
      Khana Kone situation bi goor gneup war nagnou ko doundouu Parsk goor yeupay dokhanee plus particulièrement les hommes mariés

    • @foogadebbomolooty9839
      @foogadebbomolooty9839 2 роки тому

      Merci

  • @Dada-dp8yn
    @Dada-dp8yn 2 роки тому +23

    Femme bi limou def dara diaroukofi wayé goor gni tamite bounou comencé dokhane Bilahi sa seye dotoul nèkh danoulaye ignoré dotounioula defal dara

  • @diawnumero1071
    @diawnumero1071 2 роки тому +15

    goor ak lo ndaw ndaw souniou borome maynala lo niouuseii sa diabar xana😄😄

    • @lapeulh765
      @lapeulh765 2 роки тому

      😂😂

    • @mamecoumbadiouf8916
      @mamecoumbadiouf8916 2 роки тому +2

      Diaw amna femme you deugeur té beurri dolé deh et goor gni parfois dokhane ngui ak tak ngui dagnou thiye bolé dila xoxotal mais nak quoi quil en soit seuye ak woudjé diaroul li et waye woudoul faye la abadane homme eh hommmmmme

    • @diawnumero1071
      @diawnumero1071 2 роки тому +2

      @@mamecoumbadiouf8916 deugg bou werre nga djiguene nie amna ayy judoka ay karateka lou nk ngayy guisse

    • @khadimsene4298
      @khadimsene4298 2 роки тому

      😂😂😂

    • @ouleyesy7406
      @ouleyesy7406 2 роки тому

      😂😂😂 khamna dako sekhlo dor

  • @FifiFifi-f1t
    @FifiFifi-f1t Рік тому +1

    Cheuttttt femme bi mo gnaka chance,une si bonne famille tes aussi ame chance tassek cette bonne famille ohhhhh regardes moi ca.mais on ne doit pas la laisser comme ca.il faut que justice soit faite sinon elle recidivera soit avec son ex mari soit avec la 2eme femme qui viendra

  • @boromebakh28
    @boromebakh28 2 роки тому +20

    Heureusement que le gas vivait dans la maison avec la famille sinon s'ils était seule elle l'aurais tué 😬😬😬.

  • @omarndiaye9414
    @omarndiaye9414 2 роки тому

    Ndaysane louma meti trop legui lako guis sii net bii Ms seytané da beurii dolé trop ndakh djeukeur Djii kou bakh la Ndaye aussi kou bakhla vraiment seytané mo nieuw rek

  • @Missdieng
    @Missdieng 2 роки тому +31

    Kii agressive na trop si djigueine 😡🙆🏽‍♀️

  • @MaimounaBodian-u4s
    @MaimounaBodian-u4s 4 місяці тому

    Bravo a cette dame waay elle est adorable tout ira pour le mieux dieu est grand

  • @lerepublicain2576
    @lerepublicain2576 2 роки тому +9

    Prompt rétablissement rapide et complet , de ma part j' aimerais bien avoir une femme généreuse.

  • @rackyndiaye3665
    @rackyndiaye3665 10 місяців тому

    Santat len yalla bou bax sax ndegam mingui doundou te mom wadji souko yalla mayé werr nako fassé

  • @anishsarr5427
    @anishsarr5427 2 роки тому +15

    Dala Moy amolen d'où barri té beugue du takh rek Di tek les hommes qui ont les moyens n'épouse pas beaucoup de femmes mais ceux qui ne peuvent rien pour leur awo c'est eux qui aime plus la polygamie tchim 😠🤣🤐

    • @ndaongone8443
      @ndaongone8443 2 роки тому +4

      Yaw vraie domeram ga .. kuko defone sa frère dina la nekh? Sa genre gui la rek thim.. Assassin que vous êtes

    • @fatoufall3695
      @fatoufall3695 2 роки тому +3

      Bou dalone sa mbok do wahe ni

    • @thiamthiama6552
      @thiamthiama6552 2 роки тому +1

      Gni dougnou sakh ay nite khol sakh amougnou ko mouye rétan nonou

    • @remsfgaye9591
      @remsfgaye9591 2 роки тому +1

      Iow nite nga wala Mala chim

  • @naniousamejikkoyi2112
    @naniousamejikkoyi2112 2 роки тому +4

    *vraiment le gars devrai prendre ses devant nakkala gore yalla deug mana négligent ba jiguene dilla deff ni,ballagamako deff ma defflako, wadji mo noye rek daffa faible torope en temp que gore yalla*

    • @mouhamadougueye7118
      @mouhamadougueye7118 2 роки тому

      Ki kay dou goor
      Romb na noye di deim
      Lima ci mèti mouy filmè bopam di wanè ni ki dou sakh rouss😂

    • @aidandiaye7153
      @aidandiaye7153 2 роки тому +1

      Négouko door lolou la

    • @mouhamadougueye7118
      @mouhamadougueye7118 2 роки тому +1

      @@aidandiaye7153 pas dorr sakh
      Mais dou wone yone li yeup di am.
      Tay sougn dèglou wone version wou femme bi di ngua guiss ni dafa deim ba meuneutoul limou mougn moko eup dolei

  • @kaami8709
    @kaami8709 2 роки тому +11

    Borom meulfeu bou wekh bi yama geuneu gnemer dehh problème famille diambour ngua woter dakar buzz tekk si tokk di wakh nenga wadji dakko beugeu kone lossiy wakh ndakh ko kham wayer tokk nane loumou âme amoumako Lou nekk si negam nekoul sama nekk meunoul âme dôme yama eupeu Fiit dehh vraiment les parents du gua machalah malgré li dal s’en dome s’en wakh rafetna la fille limou def gnawna trop sakh mère bi vraiment kou âme Nguor la machalah ndakh malgrés mongui geureum goro bi

    • @loufatechno2145
      @loufatechno2145 2 роки тому +2

      Way deugue rék leu déff do-mi kharam yii loumou déff gneupoko wzra guiss vrai deumla domérzm

    • @meryemsaks1101
      @meryemsaks1101 2 роки тому +1

      Bien vu. Mom ladoon wah ni

    • @aissatoudiacksow8008
      @aissatoudiacksow8008 10 місяців тому +1

      Mais elle en a le droit nakh cnest la femme de l'oncle du gars. En plus la femme est allée dire des mensonges sur tiktok il est de leur droit de sortir laver leur peau

    • @AichaTou-dc9mh
      @AichaTou-dc9mh 10 місяців тому

      @@meryemsaks1101hamo li ngay wah

    • @AichaTou-dc9mh
      @AichaTou-dc9mh 10 місяців тому

      @@loufatechno2145gni dagno nafek bayilen 😊

  • @ndeyeawandiaye6765
    @ndeyeawandiaye6765 2 роки тому +2

    D'accord n'a thy décision famille bi ...Bâle lou bakh la....le peuple réclame sa photo svp pour souniou frère yi khammm

  • @ast8347
    @ast8347 2 роки тому +3

    Yallah boumou done ndiaya dièye sama dieukeurou rack dji ay Yallah

  • @pispagalsen
    @pispagalsen 2 місяці тому

    Yallah nagnou yallah may ay sokhna you bakh

  • @diallodiallo6656
    @diallodiallo6656 2 роки тому +33

    Mais Gnarel nak nekhoul si xole quoi qu'on puisse dire. Soudone jigeen amna droit am dieukeur you beurii sou boba les hommes feront piiire

    • @bbgl8v
      @bbgl8v 2 роки тому +1

      nekhak niak nekh on sen fout !

    • @yvefay620
      @yvefay620 2 роки тому

      chapeau on prend les femmes pour RIEN

    • @cheikhounatine758
      @cheikhounatine758 2 роки тому +5

      Il faut condamner cet acte point final hein
      Si ça te dérange va te plaindre à Allah c’est Lui qui l’a autorisé pas nous

    • @originali155
      @originali155 2 роки тому +6

      Bilaye li nga wokh deugue bou boba nga guiss kougnou sotti acide surtout goor noumou firé daff faye jaré raye là sakh

    • @mhd_0039
      @mhd_0039 2 роки тому

      C pas une raison

  • @omarosamb6150
    @omarosamb6150 2 роки тому

    Billahi tonton abdoulaye padane pabou bakh tee yarre ak ndiabotam billahi

  • @UneQueen.22
    @UneQueen.22 2 роки тому +24

    Ay fausse couche mom diaroul wone toudd sama kanam bou ndaw
    Da am goor you domeram dangu léne di mouñieul ba dara doul dara ñiou nékk fii nga kheuyy yalla défal la teranga nga cmmencé weur di dokhane d gauch à droite ishhh
    Wakhou kou sokhor rk lay wax ay loumou amak négu boumou amakk doul wayyy
    Jsui pas d’accord si li mais fougn touddé djiguéne warfa toudd goor, ndeysane da meir rk d’après les témoignages kou bakh la🥹
    Mane mom kouma takkal woudiou ma ñiouss sa ndayyy😭😂😂jsuii tropp jalouse pour woudié

    • @khadimdiop2277
      @khadimdiop2277 2 роки тому

      Yaw domeramga

    • @khadimdiop2277
      @khadimdiop2277 2 роки тому

      Sa lefell ndaye

    • @loufatechno2145
      @loufatechno2145 2 роки тому

      Yallah nga tasék kou rayseu ndaye bala yague comme que lolou nga envisagé yaw Balla nga Ray kénn gnou raysa ndaye iow

    • @awacamara8628
      @awacamara8628 2 роки тому +1

      Merci ma chérie make yow gnio yeime

    • @mariebernadettegueye4946
      @mariebernadettegueye4946 2 роки тому +1

      @@khadimdiop2277 bayil léne di sagua yayou diambour yii eumbe ak weussine dafa méti paré nioulay sagua eel a le droit de s'exprimer com tout le monde meune gua ko yéde sans ppur autant sagua😏😏

  • @evadiatta5100
    @evadiatta5100 10 місяців тому +2

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 ça me rappelle quelque il va jamais oublier mdrrr leçons a retenir

    • @Rokheya194
      @Rokheya194 10 місяців тому

      Comments? Mais te pas serieux la😢

  • @malickndiaye4880
    @malickndiaye4880 2 роки тому +9

    Calibataire a vie rk moy solution lima guiss si deuk bi doyna war trop 😌

    • @Mebeingme-v7z
      @Mebeingme-v7z 2 роки тому

      Mbadou😂😂

    • @moussand7775
      @moussand7775 2 роки тому

      Ah en tout cas je te conseille de bien regarder avant de t'engager

    • @famajobe5190
      @famajobe5190 2 роки тому +1

      Seyyi mettina

  • @mariamabandia777
    @mariamabandia777 10 місяців тому +1

    Mai femme bi Di explique tamite negou seye defa khate dé netali rekk gasi âme

  • @sokhnandao2742
    @sokhnandao2742 2 роки тому +26

    Yalla naniou yalla may retenue c'est pas normal ce quelle a fait nous sommes des femmes on doit supporter où rentrer chez nous. Mais je suis contre cet acte barbare

  • @diopawa189
    @diopawa189 2 роки тому +1

    bilay goor gni daniouy diékhale xole daniou lay takk douniou ame dara gay mougne RK niou niew un jour RK

  • @ndeyefatousene3787
    @ndeyefatousene3787 2 роки тому +7

    Kou seuy ak djoulite fo tok wargua khalate nii un beau jour meunega âme woudj lii dou dara

  • @leuzdiop1056
    @leuzdiop1056 2 роки тому +1

    Une belle mère exemplaire

  • @mastourassoul3946
    @mastourassoul3946 2 роки тому +3

    Kou fékk mandarii takk ko loci ame dieuleul.... d'après ce récit diabar dji yagg na def ay acte de violence mou continuer Di seuy ak mom kay, coma on peut rester avk une femme pareille juska en arrivé là tamit

    • @aissa2425r
      @aissa2425r 2 роки тому

      mane deh moma diakhal guiss na ci yaw beneu sadique dagua maye abal wala ma abal leu.criminelle la il faut porter plainte essence bi sou takone c la catastrophe,espece de sauvage barbare

  • @cisssadammm7490
    @cisssadammm7490 2 роки тому +2

    Djiiko ,djiiko la rékk..goor ak jiguèen niossi yémm...nimou amé goor you sadique..nonou la amé jiguéen you sadique....

  • @adamandiaye5829
    @adamandiaye5829 2 роки тому +5

    Peu importe le degré de leurs problèmes rien ne justifie son acte barbare, c'est une tentative de meurtre. En plus de la préméditation elle ne montre aucun regret donc que justice soit faite

  • @FatimaFall-ci2ms
    @FatimaFall-ci2ms 9 місяців тому

    Femme bi moy doméram djiguéne dina def lii nooonnnnnnnnnnnnnnnnnnnnn Allahou Akbar

  • @maimounadiallo2028
    @maimounadiallo2028 2 роки тому +13

    Saytané rék mo gneuw ndeye san mere bi coubakh la yalnagnou sunu borom mouseul si séytané

  • @boubacarsarr8256
    @boubacarsarr8256 2 роки тому +18

    Ce qui est grave chez un homme faible est que sa faiblesse devient toxique en le détruisant et en détruisant aussi ces proches. Après une bonne correction souvent la femme consciente remercie son homme d être assez courageux pour le ramener à la raison. Quand on est faible on pousse son partenaire à être trop libre et c'est ce qui emprisonne votre vie

  • @pendahabydiopa8991
    @pendahabydiopa8991 2 роки тому +6

    Nitte dal leip loy engager attends toi à toute surprise mouy sa diabar mouy sa djeukar sa xarite ypp t mouy gor di djiguein dara diaroufi agression ou violence so meunoule mougne franchement deimal sa yone gore meunou loko téré limou bgue df du moment que diokhnala respect bgue nala yeuram nala sa xel ak sa xol bi oubi ko t yatalko ngua mougne aussi polygamie koussi fiir y’a togne ndax khamone ngua ko vraiment kou djiguein ki dafa négggg

  • @modououmy1676
    @modououmy1676 2 роки тому

    Ndeysane dako eupe doolé wayé dou nonou dieukeur sangue la

  • @souarendour9036
    @souarendour9036 2 роки тому +6

    Prenez vos dispositions avant qu'il soit trop tard
    Ki kouko diégué séne famille meune naka réye
    Téye rouss na âme lima métti
    Lou rare gua âme moy gro bou bah

  • @priskasavadogo2776
    @priskasavadogo2776 4 місяці тому

    Je comprend que ça ne soit pas facile ,d'avoir une coepouse,d'autemp plus après se genre de problème de couple ,mais non seulement elle n'a pas réagit en temps que musulmane,en laissant cela entre les mains de dieu car dieu la décider ainsi mais elle l'agresse en plus pour ce mettre elle même dans cette situation problématique, vraiment du courage

  • @julescisse1984
    @julescisse1984 2 роки тому +19

    Vraiment des parents exemplaires

  • @KhadijaFaye-k6l
    @KhadijaFaye-k6l 10 місяців тому

    Djiguène agg nio mouna euppé sa dieukeur waroul takhh gakoyy torokhol. Dieukeur dégnne koyy respecter. Mais les hommes aussi il faut savoir faire le choix . Djiguène dégnn koyy tann té Dieukeur tamite dégnne koyy tann. Qu' Allah nous facilite le mariage 💒 💍 et de manière halal

  • @mairamediallo4043
    @mairamediallo4043 2 роки тому +62

    C'est ça l hypocrisie walahi Tu signes polygamie avec ton mari quand ce dernier prend une autre femme tu te permets de faire des conneries

    • @fatougaye1002
      @fatougaye1002 2 роки тому +8

      Té bou sen frère yi také diabar danouye contane té gnom bougounou woudiou

    • @zeynabkama
      @zeynabkama 2 роки тому +5

      Parfois chérie je te jure sa yoon nekoul sil à 2 ou 3 ou 4 mais defay yoor comportement bo xamné dey meti à supporter je vous jure mais nak diaroul li vraiment mais aussi je ne la juge pas car je n connais pas c kelle vit

    • @jap7290
      @jap7290 2 роки тому +1

      Yabate rek

    • @mairamediallo4043
      @mairamediallo4043 2 роки тому +2

      En tout cas moi quand je signe pour la polygamie je vais assumé les conséquences pck pour la femme Sénégalaise polygamie veut dire souffrance alors que c'est loin d'être ça

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 2 роки тому +1

    Gor ak djguen niui di ndialo.wallahy yalla moo gueneu fuir.marieyui niofi daka ndialo