"Sama dome, diabaram moko sotti essence tale Ko…dafko bett ak goor", la mère du défunt craque

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 31 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 174

  • @sokhnathiaw6689
    @sokhnathiaw6689 2 роки тому +33

    Thièy Sénégal yalna niou yalla doli soutoureu té moussal niou si seytané ki dcd yalna ko yalla xaré aldiana firdawsi 😭😭😭

  • @janatoudubai5231
    @janatoudubai5231 2 роки тому +26

    son petit frère est très intelligent et bienveillant ndeysane taxawounga sa mak bamou dem yalnako yala yereum diegalko atekok yermandem metinaa tropp djiguene dou am xol bou woww djiguen dou am fitt djiguen dou niemé ohhh djabar dagn kay tanne😭😭

  • @fatousow9718
    @fatousow9718 2 роки тому +27

    Massa Yaay booy Yalla nako Yalla yeureum té mousseul ko thiono bamel thi barké SEYDINA MOUHAMAD (psl)

  • @tenesanokho2579
    @tenesanokho2579 2 роки тому +10

    Je connais très bien la petite soeur du défunt
    Souniou keuryi nio dennndeu souniou village la seuysi
    Que Dieu l'accueil dans son paradis céleste 🙏

  • @bintoudiop274
    @bintoudiop274 2 роки тому +25

    Ndaysane C'est triste que son âme repose en paix

  • @nafygueye6666
    @nafygueye6666 2 роки тому +25

    Paix éternelle à son âme yalna khipé dianatoul firdawsi

  • @OumarFaye-pn8zx
    @OumarFaye-pn8zx Рік тому +1

    😢😢masta yaye boy

  • @Ummou2983
    @Ummou2983 2 роки тому +7

    La fille m’a fai pleuré 😔😭Masta c tro dure paix à son âme 🥹😔

  • @adjiaminata6787
    @adjiaminata6787 2 роки тому +29

    qu'Allah ait pitié de son âme et lui accorde Dianatou firdawsi 🙏🙏

  • @moniquecisse2068
    @moniquecisse2068 2 роки тому +8

    Courage maman 🙏🙏déko nianal fo tolou 🙏❤️

  • @adamandiayekasse5990
    @adamandiayekasse5990 2 роки тому +9

    Dafa am famille yoo khamni koussi takk diabar yakou nga. Daniouy sadiq beugg mystique

  • @Sophia-xq7in
    @Sophia-xq7in 2 роки тому +15

    Thieyy louhew Sénégal ???
    Lounei nguifi deh
    Mass sa Yaye bauy metti na Yallah na firdawsi nek keureum ci barkei BAYE

    • @nefertitinefertiti8021
      @nefertitinefertiti8021 2 роки тому +1

      sokhla nagnou ay niane thi rew mi on à peur dale yallah nagnou yallah mousseul thi seytané dafa bafi dolé

    • @diasfaty4630
      @diasfaty4630 2 роки тому

      Ma chère deuk bo khamni kheureum fétiche pour out lo beuk retombé yi aussi

  • @siralo9284
    @siralo9284 2 роки тому +8

    Sen probleme bii compliqué naa trop ndaysannn adouna yagoull liii dara diarouko yalla na leppou lerrr mo Demba repose en paix

    • @Aichadia1234
      @Aichadia1234 2 роки тому

      mo takh yaay amoul morom baayi sa yaay ngir jigeen dem dekke sa ker goro mom tamit deena de Waye linou def bakhout

  • @thiernoseck2197
    @thiernoseck2197 2 роки тому +9

    Yalla nañiou yallah soutoural paix à sont âme yalnako yallah yeureum wayy teh kharéko aldiana firdawsi

  • @bernilynsha
    @bernilynsha 2 роки тому +7

    Massa yaye boy li metina trop beaucoup de courage 🙏🏾

  • @babacarfaye9060
    @babacarfaye9060 2 роки тому +3

    Que le bon dieu l accueille dans le paradis eternel et donne la famille une force de surmonter cette épreuve douleureuse

  • @tymachou4303
    @tymachou4303 2 роки тому +8

    yalla nako yalla yeurem barki seydina mouhamed

  • @fatoudiouf5512
    @fatoudiouf5512 Рік тому

    ndayesan yaye dafa nékh kon fonk léne sése yaye ❤❤❤

  • @fatoufaye67
    @fatoufaye67 2 роки тому

    Ndeyssane papam la dieul mamadou papam yarnako sou magoul changé sene papa damako done nane l'homme 12 métier ndakh door war rek bakh ndeyssane am complicité ak Marie Faye mi ndeyssane Li yalnako yalla leral

  • @kaami8709
    @kaami8709 2 роки тому +38

    Comment tu peux être seule avec ton mari mou tout bopam essence ba lakk ter yaw diemossi dara bamouy dem si canal fo nekone c’est vraiment louche

    • @kadiacisse6610
      @kadiacisse6610 2 роки тому

      Femme louche na trop en plus dafa amone copin dieukeur dji yeuk ko

  • @senesene2550
    @senesene2550 2 роки тому +18

    Sérére khamoule thiakhane sama dieukeur sérére la mai dou féne

    • @salysenghor4465
      @salysenghor4465 2 роки тому

      Niguilo

    • @adamasylla7905
      @adamasylla7905 2 роки тому +8

      Sokhna si may gnou diam serere ak diolas gno si yam baah dou si heet si yar la

  • @khadyndour2230
    @khadyndour2230 2 роки тому +15

    Senegal fi lagniy nèk di neup neupal ba finalement niou nane dafa kharou alors k il a confier a son frère ce k la femme lui a fais.

  • @nafichatoudiatta3705
    @nafichatoudiatta3705 2 роки тому +5

    Alahou Akbar métina k Allah l accueil dans son paradis firdaws

  • @binetadiao5718
    @binetadiao5718 2 роки тому +6

    Xaléy goor tay gnici am kilifeu bariwoul li yeup niak kilifeu yokouci diam... repose en paix mo demba🙏

    • @Aichadia1234
      @Aichadia1234 2 роки тому

      te goro yii sougnla maye seendom dagnouy bouga nga toog ci s'en ker loo ligeey diokhlen li nekhoul ci khôl yaay

    • @jesuispapealeniag5529
      @jesuispapealeniag5529 2 роки тому

      Massa ahlla mande douma masa seyi si loudoul digalou samay wadiour incha ahlla

  • @fatoundoye8416
    @fatoundoye8416 2 роки тому +7

    Cou goor ki mougui fêneu cou Lak nèk urgence do wakh tè si vérre bi guaye takhawe hum

  • @elymanesaidoukane5126
    @elymanesaidoukane5126 2 роки тому +2

    Que Dieu juge entre cette fille indigne et le coeur brisé de cette mère

  • @astougueye83
    @astougueye83 2 роки тому +8

    J ai regardé 2chaine mais la version du Frere reste constante donc c logique que sa femme sodé ko

    • @maguetteseck3163
      @maguetteseck3163 2 роки тому +2

      Pour t dire sen histoire bi mo bari ay version

  • @amybass8022
    @amybass8022 2 роки тому +22

    Que son âme repose en paix et que firdawsi soit sa dernière demeure Amine ya Rabby 🤲🙏

  • @biramethiaw1793
    @biramethiaw1793 Рік тому

    Les larmes du petite soeur m'ont fait couler les larmes

  • @ndaosarr9073
    @ndaosarr9073 2 роки тому +6

    Paix à son âme li métina trop yeah sénégal

  • @fayendeyemengue8907
    @fayendeyemengue8907 2 роки тому +10

    En tout cas, li wakeur Aminta wakh ni niom falé wouniou Mamadou,fégne neu si papa dji! Comment on peut te dire que ton fils aîné tentait de se suicider ngua nane dém léne teudi, mou délouwat kheuy ,au lieu ngua kheuy out ay éclaircissements concernant l affaire,ngueu gadou sa sac ni da nguay liguéyi,il a fallu que le docteur l appelle pour qu il rebrousse chemin, même son petit frère il a été au courant, té néneu papam moko wo ,Niko Mamadou lakam bi métineu de! Moufay soga dém,yalnako borom bi yereum kharé ko Aldiana

    • @antadieng525
      @antadieng525 2 роки тому +1

      On se voit que les parents ne sont pas d'accord du mariage il a laissé sa famille pour sa femme

    • @ramasenghor5166
      @ramasenghor5166 2 роки тому +1

      😭😭😭🙏🏾

    • @khadijagueye1473
      @khadijagueye1473 2 роки тому

      Je pense que le papa était déçu psk à la base ces parents n’était pas d’accord avec ce mariage !

  • @ndoumbethiane5075
    @ndoumbethiane5075 2 роки тому +5

    Yalna ko yalla yeuram yalla moussal gnou si jigueen bou bone

  • @alleualleu693
    @alleualleu693 2 роки тому +5

    Pourquoi deukoul sen keur 😭😭😭

  • @Aichadia1234
    @Aichadia1234 2 роки тому +5

    sa papa dou responsaboul nanlagnlay wakhè sa dom defa bougon kharou ngenelen demlen teddi li dou dara

    • @antandiaye5541
      @antandiaye5541 2 роки тому +1

      Khamna linne Dano yagu di khekh motakh mou khawa decourage

  • @alleualleu693
    @alleualleu693 2 роки тому +2

    Delen wakh lou rafet khaleyi daniouy mague 😭😭😭😭😭😭

  • @falloudieng6633
    @falloudieng6633 2 роки тому +8

    Ndysaan Yaay Booy Yallah Nala Yallah Maay Kholou Mougne😭

  • @mareimendiaye5066
    @mareimendiaye5066 2 роки тому +2

    Que la justice soit faite

  • @teydemfall3470
    @teydemfall3470 2 роки тому +24

    J'ai jamais vu un journaliste aussi incompétent mais qui khana weroul

    • @yayefatoudiouf3104
      @yayefatoudiouf3104 2 роки тому +2

      Wallahi
      Des questions tellement idiotes

    • @abdourahmaneba3773
      @abdourahmaneba3773 2 роки тому

      Wakhal way frère ki khamoul touss en plus il est indiscipliné quoi

  • @Diaz426
    @Diaz426 2 роки тому +3

    Bayilene journaliste bi begue lou lere rk repose en paix fr🙏

  • @CodouSow-y8u
    @CodouSow-y8u 3 місяці тому

    Me lima Diakhal nekk bi lakoule yalla rekk mo khame 😢

  • @worefaye6760
    @worefaye6760 2 роки тому +11

    Paix à son âme

  • @Aichadia1234
    @Aichadia1234 2 роки тому +4

    esk diokougnou doctoorbi khaliss pask mom ci boppam waronnako laj lanmola defli yew dakoy laj mou terèla kon amna louci louss

    • @oumoukhairyfaye7784
      @oumoukhairyfaye7784 2 роки тому

      Vraiment bien dit.Hopital de heure boula façon yi dale amena gnoufa nek gnoulaye lathie Li loulako def.Sougnou élevé dawna mbekentek moromame mak sama collègue yobouko hôpital mais c la première question bignou posé louko defni te khalebi lagnouko lathie mounelene dama daw mbekentek sama bene morom

    • @Aichadia1234
      @Aichadia1234 2 роки тому +1

      @@oumoukhairyfaye7784 mande loolou mooma diakhal

    • @oumoukhairyfaye7784
      @oumoukhairyfaye7784 2 роки тому

      Mouhamed aidara yalla bakhna .Adouna dale yalla na yalla mousseul bepe domou adama rek si façon yi .Merci beaucoup

  • @rokinadash5369
    @rokinadash5369 2 роки тому +5

    Wa mane damay guént wala sama bop lay nakh nii😳mais sénégal dal do tokk 2jrs yo dégoul meutre....éhhh allah🥺

  • @fatoubinetoulam275
    @fatoubinetoulam275 2 роки тому +5

    Comment tu peux poser certaines questions

  • @ndeyeamicissokho8339
    @ndeyeamicissokho8339 2 роки тому +6

    Seyou Sénégal

  • @mariamakamara2541
    @mariamakamara2541 2 роки тому +3

    K son âme repose en paix

  • @mamamniang4068
    @mamamniang4068 2 роки тому +6

    Paix à son âme Ndeysane

  • @mamanmbaye6833
    @mamanmbaye6833 2 роки тому +1

    Bilahi li metina trop paix à son âme

  • @dioufsira8570
    @dioufsira8570 2 роки тому +22

    Khalé yi dagno gnak kilifa nite dafaye deguelou wadiourame

    • @teyasow15
      @teyasow15 2 роки тому +3

      So begué do degue lou do giss kenn

  • @khadydieng7875
    @khadydieng7875 2 роки тому +4

    Y’all naco yalla yeureum

  • @belleduteteaupied1393
    @belleduteteaupied1393 2 роки тому +3

    Thieuy Yalla li metyna

  • @khadydiallo9721
    @khadydiallo9721 2 роки тому +12

    Wawe mome bimou néko hôpital loutakh wakhoul kiko tale diabare dji souko talone dou gnewe hôpital pour mane

    • @layeilliassou4804
      @layeilliassou4804 Рік тому

      naka la sa brome keure di nék ak say dom a côté ngani daga coy tall chotti co ptrole nagouwouma son frère balegui wakhoul Aminata moco tall

  • @tymachou4303
    @tymachou4303 2 роки тому +9

    wa ki journaliste leu? ça façon de poser les questions 😆

    • @louisedieye
      @louisedieye 2 роки тому

      Je me suis posée la même question. des questions qui ne se posent pas vraiment

  • @balamaissathiam9610
    @balamaissathiam9610 2 роки тому +1

    Kou bakh la wonne jai les vidéos de son corps bimou lakkéé mai maitina trop sakh

  • @nenegadio2298
    @nenegadio2298 2 роки тому

    Yaye galadjiou dom☝🏿👋🏿fonk len seni yaye yi yalnagniou yallla moussal thi li hew thi rew mi lgui.Paix à son âme

  • @fatouceesay7683
    @fatouceesay7683 2 роки тому +1

    Rip 🙏⚰ 🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲😭😭😭

  • @Adelina198
    @Adelina198 2 роки тому +3

    Bayilen di wat,
    Chaque jour diogué yarah?
    Ya trop de delinquence dans les couples.
    Beaucoup de version dans ce sujet.

  • @diarrasy9035
    @diarrasy9035 2 роки тому +2

    Comme genre téré nagne koko ba sonou am na yo kham ni diaroul wax dale

  • @Aichadia1234
    @Aichadia1234 2 роки тому +3

    waaw leegi moom loutakh doctorbi lajouko lanmoola lakka komko moungidon wakh kay walla papa sakh

  • @bijougueye4087
    @bijougueye4087 2 роки тому +2

    Metina dale vraiment Li kén khamoul lane leu sodé bi beurina si réxmi torop

  • @ndiayeawa3605
    @ndiayeawa3605 2 роки тому +1

    Yalla nako Yalla saffara

  • @fatouceesay6794
    @fatouceesay6794 2 роки тому +4

    May his gentle soul rest in perfect peace ndeysann very sad😢😢

    • @allianceparfait309
      @allianceparfait309 2 роки тому

      t américaine ou koi ?😂

    • @khadydieng1381
      @khadydieng1381 2 роки тому

      @@allianceparfait309 regarde son nom de famille tu comprendras qu’elle est gambienne 🙄

  • @khadijatoure1557
    @khadijatoure1557 2 роки тому +3

    Mé bouteille nagnou ko yobou laboratoire gnou hol ko

  • @ngathiefallmusiquefromsene2060

    Wa keur aminta la gena geume dei bilahi

  • @diarrasy9035
    @diarrasy9035 2 роки тому +3

    Ak Lo léne thiy meune wax na rafete internet c’est presque éternel té khalé ay domame lagne té dagniy magg
    Alors n’a rafete

  • @elymanesaidoukane5126
    @elymanesaidoukane5126 2 роки тому +2

    Quand t entends cette mère parler tu sais qu elle a mal wallahi Eskey c'est vraiment pas toutes les femmes qu'on épouse vraiment pas car toutes ces jeunes filles qui marchent là dehors elles n'ont pas de formation pour garder un foyer rire sont menteuses tricheuses vraiment c'est pas la peine

  • @mamitafall943
    @mamitafall943 2 роки тому +10

    Senego daal li boumou leine dallati mohh ki journaliste la yi ladiou doff melni kou demoul thi niou am nakar may wakh mounane mo seuyi wone ak nane yaye dji ndakh dou yiguako daane nianal mo keupou thi kawam. Metti nama trop vraiment

    • @abdourahmaneba3773
      @abdourahmaneba3773 2 роки тому

      Wakhal dé kikay amoul ben compétence

    • @maremeyade2378
      @maremeyade2378 2 роки тому

      Ki est ce que journaliste bi tmte werna bou bakh non ki dou journaliste

  • @ndeyeyacinediop5367
    @ndeyeyacinediop5367 2 роки тому +4

    Masta Yaye boye😭

  • @toureidadiisha1630
    @toureidadiisha1630 2 роки тому +6

    entout CAs dalle c’est louche……meunouma gueume niii diabare djiii mokko raye

    • @binetoudiop7172
      @binetoudiop7172 2 роки тому +1

      Diabar dji djioudouwoule sakhe

    • @toureidadiisha1630
      @toureidadiisha1630 2 роки тому +1

      @@binetoudiop7172 Sénégal meitina on juge les gens sen khame lou xeiw exactly dieukeur djiii rk Walla diabare djii niou meuna wakh Lou xeiw …Mai’s Sénégal bougn la bagner rk c’est mort bagn nagn la

  • @ngathiefallmusiquefromsene2060

    Famille bi dano inventé lou barri sakh! Amnati aye part de responsabilité you barri, yalla nanou yalla diégal

  • @famagueye9971
    @famagueye9971 Рік тому

    Senegal gnare gnou khoulo ko deguelou ngani mo ame raison .kouye netali melni ya féké y a que le couple qui peut dire ce qui s est reelment passé.

  • @awadiouf9655
    @awadiouf9655 2 роки тому +1

    😭😭

  • @oumarsoumare7613
    @oumarsoumare7613 2 роки тому +2

    Non c trop n'deysane paix à son âme amine yarabi

  • @Aichadia1234
    @Aichadia1234 2 роки тому +3

    journaliste bo tamit louci ladj ay khet diarouko senegal benna boppoula kenna mounoko khar gniar

  • @FatouNdiaye-g6z
    @FatouNdiaye-g6z Рік тому

    😂😂❤😮🎉😢❤❤❤😂

  • @jap7290
    @jap7290 2 роки тому +8

    Bayi lene journalistes you doff yi guene di tontou

  • @matykebe9971
    @matykebe9971 2 роки тому +7

    Ce ga ils parle toujours la même version

  • @awambayeeva6698
    @awambayeeva6698 2 роки тому

    Réponse en paix

  • @aisatatall914
    @aisatatall914 2 роки тому

    🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻😭😭😭😭😭🤲🏻🤲🏻🤲🏻🤲🏻

  • @yacinecoulibaly7459
    @yacinecoulibaly7459 2 роки тому +13

    Mane dhei si sama guiss guise aye khalé sounou beuganté bayilen niou seuye y'en kilifeu yi daguen di seuy sen seuy beug tanal séni doom kounou warra seueyul sen diamono ak sounou diamono bokoul mes tamite kou djiguen ki sa borom keur nanelay soté bopam pétrole bay deim si canal di sauvé bopam tei woutou walou Walla diemosi def dra ces vraiment louche yeen niary famille yi ameguen si par de responsabilité ndakh beugentéwolen

    • @jesuispapealeniag5529
      @jesuispapealeniag5529 2 роки тому +5

      Mande bokuma al yaw guis guis mande kuma samay wadiour tanaloul bougou mako diamono mousoul sopiku djikoyi mosopiku waye diamono nimou melon nonou lamel balegui
      Kilifa mounta ñaka mande antaka djiguen samaye wadiour rekh laye degeulou wassalam

    • @adamandao2799
      @adamandao2799 2 роки тому +4

      Billaye penda yaw la andal mane samay wadiour louniou beugoul beugouma té def na 22ans de mariage té rediouwou mako nit dagaye ame kilifa

    • @binetoudiop7172
      @binetoudiop7172 2 роки тому

      Diabarou mo demba djioudouwoule sakhe

    • @jesuispapealeniag5529
      @jesuispapealeniag5529 2 роки тому

      @@adamandao2799 doko masa rethiou yalnalen yalla geuna dioubale kilifa douye thiakhan

    • @layeilliassou4804
      @layeilliassou4804 Рік тому

      bien di sa kadou amna solo

  • @ousseynoudioum5938
    @ousseynoudioum5938 2 роки тому

    😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @Adelina198
    @Adelina198 2 роки тому

    Ñiaka kilifa rek, ak tama tahawalou. Ñiari bandila. Khoulo kheh rek. Tey foumou moudié gañou. Trop de négligeance

  • @kanysenghor7403
    @kanysenghor7403 2 роки тому +1

    Thiey journaliste bi yi question tamite nit dinako l’adje kou am nakar

    • @papendoye891
      @papendoye891 2 роки тому

      Putain j'ai la haine wallah 😡 😡 😡

  • @ibousembene3836
    @ibousembene3836 2 роки тому

    Sey dall diamou sou diamou manoul am na tass moguene

  • @boussondiaye8303
    @boussondiaye8303 2 роки тому +8

    Mere bi elle très véridique en plus Mamadou boude mo Tal Bopam si kanamou diabar DJI loutakh sauvewouko bamouy DEM di sauvé si Bopam si canal bi se louche dal mais Yalla n'a Yalla leral Lép🤦🤸

    • @senesene2550
      @senesene2550 2 роки тому

      Merci vérité

    • @pendadiop7697
      @pendadiop7697 2 роки тому +2

      Mais le cas de maris la femme qui avait brûlé son mari la chambre a pris feu 🔥 je ne les.connnais mais je pense si c'était la femme. Qu'elle que chose aurait brûlé dan la chambre

    • @binetoudiop7172
      @binetoudiop7172 2 роки тому

      @@pendadiop7697 merci chéri

  • @dembaniang8268
    @dembaniang8268 2 роки тому +4

    Métina li dagou la

  • @abdourahmaneba3773
    @abdourahmaneba3773 2 роки тому +2

    Paix à l'âme du défunt

  • @fambayeba9840
    @fambayeba9840 2 роки тому +8

    Yaw guathé galama seureule gua bayame té kene mosou léna deugue saye mbokou jeureur greureume nagnou kone yaw sa lokho sete na té lou nek jeume guako pour mou ba khalé bi khana diko nianale yalla yeureume ko té kharé ko aldiana

  • @fabediloumloum8444
    @fabediloumloum8444 2 роки тому

    Yaw tamite meuno wone enregistre wakh dji comme yorr nga téléphone

  • @rokhayacisse7157
    @rokhayacisse7157 2 роки тому +1

    Ngen balma mais lakk katt pour gniom mbokam rek la warreuh takk

  • @yandesaine2409
    @yandesaine2409 2 роки тому +2

    Vous bien enquête sur chose c'est pas là vérité

  • @senesene2550
    @senesene2550 2 роки тому +4

    Wakh dji moye wa keure amineta dagnio beugone débarrassé wouthi khalé bou gaure comme amineta da beugue changé vie wame

    • @binetoudiop7172
      @binetoudiop7172 2 роки тому +4

      Boulsi sakhe wakhe loula leroule astafourlah

  • @nogayebbbn2936
    @nogayebbbn2936 2 роки тому

    Est-ce que mak ji moko wax aussi. Vu que beugo laine femme bi dama ci téye.

  • @barasylla5183
    @barasylla5183 2 роки тому

    Vraiment xétti journaliste yii nunulaye laajié ngaye nagu ku xame lumu wara laathie ak lumu warta laathie doyna waarr

  • @mamediarrasene840
    @mamediarrasene840 2 роки тому

    Kouy tak nangako gestou bou bakh djiguene yii legi da âme gnou bon

  • @sokhnaaminatagueye5601
    @sokhnaaminatagueye5601 2 роки тому +2

    Journaliste bi mbam la reik

  • @astoundiaye7186
    @astoundiaye7186 Рік тому

    Man d lima analyser femme bi talouko wah lenn sen diguentek yalla rk linguen wah dara cohérent woufi daguen beugu inculpé femme bi ndah Aminata dou seuy ak kou melni mor Demba diko mounieul baparé diko tall nitt meuneu na tall bopam baparé beugu sauvé bopam parsk lakk dafa mety

  • @thianediagne5270
    @thianediagne5270 2 роки тому +1

    Mais journaliste bi ayoul d

  • @awasadio7777
    @awasadio7777 2 роки тому +2

    SENEGO

  • @fatoubinetoulam275
    @fatoubinetoulam275 2 роки тому +2

    Il est vraiment bête ce n'est pas un journaliste il a été formé dans le tas