De toute les façons la manière dont lac 2 à lutter n'a surpris personne...Eumeu loumou beuré mo diakhall gneup.....Je pense que Lac 2 a été victime de sa mauvaise réputation mais tay defna touti dara
Jamaïcain yaw danga farr tei neuboko. Lamine femm nala ay Yon si bir combat bi.eum dem na ardo nganan ardo amoufi ...yaw yarou woo bilahi walahi.respectel nit gni . mbeur Yi SA ay nawlei lañiou..guemo dara...lac2 dafa am ay mbok. ♥️♥️Danga rew bilahi
Bilaye lac de guiere sama 5500f crédit yima gnak té diarouko sil te plait 😭 gua délomaco mane nak lépp manela sayoumala yakaré pour békk gual mél ny dagamaye nakharare diff loula nekh😁 mai dotouma déff si 100 bilaye dakh do dara si lamb khana snhapppp😁
Lac mo gueuneu sokhla combat bi lou takh defoul nimou defone papa sow lac guerre ragal la eumeu nimou def nonou leu parce que il a une foi été le roi 👑 des arènes et en plus il est le plu âgé il est presk en fin de carrière lac style beuré bi la wara bayii chak combat nul nione sokhlowouniou nul mome ak boy niang tamite nii la defone dafa nio respecté woul rek respecté woul tamite wa guédiaway mbeur bou niaméoul cou dou mbeur mbeur faw nga melni BG2 da nga encaissé premier coup nga dem defi li ngay def dane deme sa yone chapeau a balla guaye2
A mon avis daniou wara changé système bi def ko 3 guéww premier bou makk deuxième mi temps bou ndaw 5 dernière minutes yi geuewou 1m mbeur bou guen niou dagg la 25% .
lac2 she is nothing so woh want to go up is lac2 eumeu she is got ready so lac2 most fight that's why people have to forget this stupid man lac2 crazy man
Senegal deuguoulen nak tay mom eumeu sene amoul envie beuréé,😂😂😂😂😂 mou melni gris bordeau ak ngimb bou verte bi. Combat bi mystique le woon nila rek manoon moudjié lamb le
@@fatoumatapendatoure5876 dou beurei ba parei bou parei nane promoteur bi ak journaliste yi dagnkoy sott ta keneu amoul diotam, chaque combat nii leu , Mane dei dotouma setaan lambam
Yene bou dielon risque forsé ngenn ni dafa diay comba bi kéne khamoul lou sénégalais yi beugg lac2 mi modoul mbeur ni lafi défon si boy niag di tapalé ba Nul nan modan
eumeu dou niew di asalo lambam dalna contre modou lo degue si loune cone douko dalate lac 2 nena eumeu mak la kaye mome mo warona niew dokh si kawam beure t eumeu moko danone
Eumeu 42 ans qui n'a plus rien à prouver, lac 2 eupouko taille, poids et rallonge lou eumeu warone deff? Diène Kaïré modou anta défoul touss et pourtant dako douma dane, goné souy beuré ak kouko mak lep mom la war. Lamb goné ak mak niar douniouko beuré kène dongou la beuré war tamouy ki yakar yegg au sommet. Kou beuga done ndanane da ngay yor djiko ndanane. Dommage mais Lac 2 mo eup ay combat you niak foula ci arène bi victoire comme match nul. Meussoul dieuli mbeur daneko ci 10 ans, da nga koy songou mou plaquer la.
Dieul sa Million diguo dioguèe pour rien lii mome djoguo sie nèwsii doléyii mo guéne Quoi no guéne dou balla cest le meilleur même si il vas il vas nous satisfair nous les amateur
Lepp kouy supporter Lac de Guiers 2 amo mbeur. Qui Mbaye Match Nul wala mbaye Rassou lagn ko wara touder. Promoteur bouffi teugeuti combat Lac De guiers diapalni Dangay maye say million azaka
Mais eumeu a bien fait de lutter ainsi, il n'a rien a perdre, c lac qui a besoin de victoire, c lac qui a besoin d'etre roi des arenes Comme moromame yi, c lui qui doit prouver, mais Comme d'habitude il a decu tt le monde. Lac2 veut la victoire sans risquer.
mais bouléin dara bet cest deux luteur son en mauvaise forme phsik et eumeu c'est pire il est lourd graisseux et a une tres mauvaise cardio!! combat soula beté tu prends pas du poids tu en perds !! tu essaye d'etre sec et souple comme diéne kairé!!!o moins....pkoi prendre des proteine pour jeul 10 a 15kilo de graisse so solé yéré nioun naane la ponkal mi foo tok di niak ndax nine (sportif bouy tok di niak rekk si c pas une pathologie c le signe dune mauvaise prepa il nest pas en forme )!! soy soumékou nioulay djeppi so yeugeutoo 2 minutes djéhkhal cardiaquement !!et tou tes mouvemen sont limité ils ont fai une trop mauvaise preparation , mbeur athlét dagey paré tout le temps surtt niom toute l'annéee tu te prepares car cest ton metier ! reug reug toute l'année il a presk le mm phsyik tou le temps ...
Eumeu vraiment hamouma lou héw tay mais kéne hamer wouko. Lac mom warone ne degueul bopam dane ko diél bou sét bou feké mbeur leu. le combat a été décevant
Bou défoul ni nan lay déff lac2 mi modoul mbeur Emma sene li modon yonou combat bi bimou yakam tie si modou Lo giusss nga li si khewww lac2 mi modoul mberrr
Vive lutte TV félicitations lamine Mais toi qui gère la chaîne UA-cam amo kholle kou sokhore gua un de mes amis avait mis un commentaires pour demandé des abonnés gua supprimé commentaire bi pour lane tu mérite pas de géré cette chaîne di nittou dra commentaires boula nékhé supprimé KO mais dinala siwal féppou
Depuis niou oubi Arène nationale beuh légui combat bou nekh amoufa 🤦🏿♂️🤦🏿♂️🤦🏿♂️
Vive BG2,Ama Modou lô
.
@@abdoulayeniang5519 se
sa thies ken d'où Mom
5😊 9:42 @@abdoulayeniang5519
@@adamaly4668❤❤❤❤
Je suis Italién et J'Aime la LUTTE LAMB.
Est Fantastic ❤
Eumeu Séne Naysann Dafa commencer Magal ohhhhh 😢😢😢🙈Mé Lac 2 Mome Dou Day lou lérr lalène wax kii Mome franchement Lamame Mome Merci Rék Ndioune Danio sonna thi Lac 2 Guér 😂😂😂😂🤣🤣🤣😂🙈
Nékhoul nékhoul dara safou si thiey balla Gaye ya nékha farale dimanche 💪💪
KEN DOU BALLA GUEYE 2 MOY CHAMPION
Bilahi wakhatiko dé
Bilahi
Bilahi
Le lion de guediewaye👍👍👍
@@hamidoukane9731ss
Soyons sérieux, malgré ce combat décevant, Eumeu n'a rien fait, donc laissez Lac en paix
De toute les façons la manière dont lac 2 à lutter n'a surpris personne...Eumeu loumou beuré mo diakhall gneup.....Je pense que Lac 2 a été victime de sa mauvaise réputation mais tay defna touti dara
Lac de guerre Ken warouka teugale combat
Exactement
Lac mo ñiakk ndiom quoi mom warra prouvé parce eumeu Séne nékk roi pa paré
Vraiment aujourd' huis lac est le dominateur de cette combat
Dominateur sans prise de risque aussi, moko gueuneu nekk en forme fouff
Anna fans balla gaye 2 ?
Merci beaucoup eumeu de lutter comme sa contre lac2
Kou wahal yalla khamni lac 2 mo beurē tay
Beure geuy amofi wakh deug yalla balla geuye moy sama mbeur nak
Mbeure moy diapante te amufi lac deful tous
Bilakhi
MODOU Le Boss !!!ONE Love
Respec balla gueye 2
Jamaïcain yaw danga farr tei neuboko. Lamine femm nala ay Yon si bir combat bi.eum dem na ardo nganan ardo amoufi ...yaw yarou woo bilahi walahi.respectel nit gni . mbeur Yi SA ay nawlei lañiou..guemo dara...lac2 dafa am ay mbok. ♥️♥️Danga rew bilahi
Soneul nguene gneup be gniou oubi Arene bi, défolene fi tousss, nekhoul be nekhoul, Balla Guaye 2 , Modou Lo, Ama Baldé , Bombardier gniom rek gnio diareu setane car sene combat mom amoul match null.
Balla Gaye 2 ak Bomb yep Eumeu danena lene thi lou gaw ! Modou lo mi ngay wakh Eumeu beurena ak mom 25 minutes diriger combat bi yep djoxe bopam ba djex taak!
Bayilene faar bii ! Modou lo nul na ak Lac 2 fois, nul ak Gris. Balla Gaye 2 nul na ak Gris cons combat bi yep!
@@papadiom9260 esk d’accord ngue ke combat bi nekhoul demb? Mane lolou rek moy sama message.
Bilaye lac de guiere sama 5500f crédit yima gnak té diarouko sil te plait 😭 gua délomaco mane nak lépp manela sayoumala yakaré pour békk gual mél ny dagamaye nakharare diff loula nekh😁 mai dotouma déff si 100 bilaye dakh do dara si lamb khana snhapppp😁
Thanks
J'appuie sur j'aime pour lutte TV mais pas pour guignoles
Emeu est tjr roi loumouy prouver Lac kouy sofal lamb leh vraiment
Diaroule dème stâte
Le roi cest modou lo
Balla gaye 2 dal moy nekhal lambji
Heureusement que la distanciation social a été respecté 😅😅😅combat covid 19 ngay am fofou
🤣🤣🤣
Mala wakh li😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂combat corona virus distanciation respecter. Thiéye sama gayi
Magui dé
@@beatricediatta1871 dafa leer 😅😅
@@ousmanediagne9502 eup na deff
Eumeu séne bilahi monou togne du dieule comba bi ndakh lac koumou beuréle gnou khass la
Ah bon pourquoi
merci waye
Légui eumeu Loum fi beuré ?
Lac mo gueuneu sokhla combat bi lou takh defoul nimou defone papa sow lac guerre ragal la eumeu nimou def nonou leu parce que il a une foi été le roi 👑 des arènes et en plus il est le plu âgé il est presk en fin de carrière lac style beuré bi la wara bayii chak combat nul nione sokhlowouniou nul mome ak boy niang tamite nii la defone dafa nio respecté woul rek respecté woul tamite wa guédiaway mbeur bou niaméoul cou dou mbeur mbeur faw nga melni BG2 da nga encaissé premier coup nga dem defi li ngay def dane deme sa yone chapeau a balla guaye2
Lide betouma lac 2 rek 😂😂 dou dara 😂😂
promoteur yi dagno am khaliss bougnouye yakhe mo takh gnouye teugue combat lac
C pas vrai il faut dire la vérité eumeu sene tapéte leu moy daw
Je n'ai jamais aimé Lac mais sur ce combat,il vraiment prit l'initiative d'attaquer,un peu déçu par Eumeu sene
Lak nulle la xame menoul koumou dadiel nulle cone mo sik ak deparou comunucation wam
Combat bou amoul songou moy dieul initiative? 35 minut
@@moustaphathiam7415 de
Initiative bouko dieulon beurei bi diekh
Combat bi nekhoul mais vrai dire la vérité eumeu senne beuréwoul srx
Eumeu sene a fini sa carrière professionnelle de lutteur , il doit accrocher son ngeme au mur.
Felicitations lac2 meme si tout le monde te ignore
Bilahi niepou daniouko ignore mais ndanan lah
Biyilen rek lac beurena eumeu mon bagne il voulait faire comme avant prendre le pieds de lac il a refusé
Eumeu sene louko daal il na jamais lutter comme ça niou door ko fayouwoul 😂😂😂😂😂 bravo lac2. Courage Eumeu
Mystiquement atteint !
@@papadiom9260 mystique laniou wara interdir. sa fausse le jeu
@@papadiom9260 loll da fa beugoul danou rek
Eumeu nak mak la il 42 ans
Mystiquement laniouko diap
Lac mo nekh blesser mbeur war ko songou nanko ardo😂😂😂😂
😂😂😂😂😂 je suis pas le seul à remarquer
Il indique avec la main
@@mustathioune9549 Bata
Si
A mon avis daniou wara changé système bi def ko 3 guéww premier bou makk deuxième mi temps bou ndaw 5 dernière minutes yi geuewou 1m mbeur bou guen niou dagg la 25% .
🤣🙏🏾
Frement tay Eumeu sene mou beuréwoul
Lui au moins il luttait, mais Lac n'a jamais lutté. Rassoul, xar, daw... Aucune initiative durant tte sa carrière
@@diallohabiboulaye8845 ce que vous dites est vraiment fausse et puis sa na rien a avoir avec ce combat
Eume nekoul si dara mais nekhoul deugg nakk
lac aurait du en profiter pour le battre
Lac 2 mo defoul dara
Combat bi eumeu moko yakk bilahi
Combat bi mon geuna soff
Si histoirou lamb na dei lamb ba legui li safoul sucre safoul khorom 😂😂
Machalla lutte tv et buzz
Eumeu dafa diougé si défait bou méti donc tay dou nieuw assalo bopam
Vraimment ca n'est ç pas un maths
Waye dafa maguet nganane
Selon moi eumeu est en fin de carrière, il ne s entrainne plus durement ou sérieusement.
Il n ‘ etait pas pret physiquement ou Mystiquement. Il n’ etait pas pres pr le 4 il faut qu’ on soit honnete
Félicitations lac 2
Kene dou balla Gaye 2
Eumeu sene beuré woul
Waw
Kanmo Beuré lac
LAC NAK LAC DAFA NIAK DIOME REK MÉ SOU AMONE DIOME MOY TÉ LAMBOU DJI
lac2 she is nothing so woh want to go up is lac2 eumeu she is got ready so lac2 most fight that's why people have to forget this stupid man lac2 crazy man
Sénégal mo barri nafek taymome eumeu mo beuré woul darra
Maky sall lé niou toudé lamba bi niaméwoul BR ak ousmane sonko 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Senegal deuguoulen nak tay mom eumeu sene amoul envie beuréé,😂😂😂😂😂 mou melni gris bordeau ak ngimb bou verte bi. Combat bi mystique le woon nila rek manoon moudjié lamb le
Esk dou guimb bou gris ay domou nday lagnou
@@abdourahmanesindidi1818 beh oui meme ngimb que gris vs balla 😂😂😂😂.
Merci lac 2
Franchement Lac nak sick na trop mais taye mom Eumeu séne mo beuré woul
Wakh Deugue... 3 fois ardo avec des blessures sérieuses
Eumeu amoul loumuy pourvue si lamb dji lac mo diémoul dara
@@bayelaminegueye3511 bly
@@bayelaminegueye3511 bilahi degeu la
@@bayelaminegueye3511 Eumeu vient d'une défaite et là il a des blessures sérieuses et une autre défaite
Mais comment se fait-il que le combat de Diène Kairé vs Modou Anta etait plus intéressant que le grand combat?
C’est honteux
Fii eskeu comba yii dinañiou nekhati com bou ndjieuk, mbeuryii dañiouy soralé mesur barieryii, lii moy comba coranavirus 😂😂😂🙄🙄🙄🇪🇦
🤭😂😂😂😂😅😅🤣🤣🤣🤣
🙈🤣
🤣🤣😅
Magui dogua lire commentaires bou bou am khorom😂🤣😅😂🤣😅👍👍👍
Combat bi comme mandat Macky Sall, tout le peuple n’attend que la FIN.
Lac 2 khawma bane promoteur mooy yakatt khalissam si mom, mbeur bo khamni meunoul beuré baga contane, lii mooy dieulsi revanche ?? Perdre lo nguen gneupp beneu 1 heure de temps
Non tay mome il n'a rien fait eumeu mo bougoul beuré
Bly lac da wara bay lamb car d'où mbeur jamais mou songou mbeur amna dolé mais tapéte leu bly ayy bou nékone kharagne libérer nagnou yagg na
@@fatoumatapendatoure5876 dou beurei ba parei bou parei nane promoteur bi ak journaliste yi dagnkoy sott ta keneu amoul diotam, chaque combat nii leu , Mane dei dotouma setaan lambam
Lac dou touss
Way wo way beurewolene mane eum taye dafma beteu saway daf si bogona profito rek wayei tay mom lac defoul dara mo dominee li dou ap lay 2:0a domicile
Lac eumeu amna loumi am si lamb ba paré yaw ya wara beuré
Je suis depuis Italie mais kouma wakhati dieundeul code ma tégual sa mame khathieu
🤣🤣🤣🤣 Rayngama
Bilahi mais amna combat You nekh comme Modou Lo ama bobou diarr na dieund code
@@mouhameddiarra1240 Balla Bombardier
Balla Gaye2 dinama diaral ma dieundatt code mais simome lay yamm ndakh Gaïndé la
@@adamasow5112 lou lerrr
Tey mome lac2 takhaw na même si songoul mais dawoul. Eumeu dafniou yapp di dem si sakou yi rek ahhh
En plus yobou nako 3 fois ardo
Felicitation lac 2 du courage Eumeu
Lak deux diaroule fèlicitè dou tousse
@@amadousow8717 😂😂
😂 😂 😂 😂
Inchallah lac 2 dou takhati may yakh sama khaliss di déme Stade sama 10 000 yi may naa kako grawoul
Bilay kou niak diome la
Eumeu sene naq bro
@@boubacarsyllame2835 frère iow xam ngané eume séne paréwoul tay lac mo momone béss bi mais niak fayda mo takh mou guéné eume séne par point
@@falloudione9949
Dafa niakkeu fayda
@@boubacarsyllame2835
Eumeu sène mom douma ka wakh Dara
Eumeu sene tay mom wérégua bilay khawma koula conseil wayé khamoul deudieuw ndém waro wona degue lou kén dagua warona déf sa manine com lignoula khaméwone vraiment tu ma désu😭😭
Waye défoule dara lac mo tame li
Bilahi mome lay supporte mais dokhoul dara
u a vu le poid d eumeu?
Yene bou dielon risque forsé ngenn ni dafa diay comba bi kéne khamoul lou sénégalais yi beugg lac2 mi modoul mbeur ni lafi défon si boy niag di tapalé ba Nul nan modan
eumeu dou niew di asalo lambam dalna contre modou lo degue si loune cone douko dalate lac 2 nena eumeu mak la kaye mome mo warona niew dokh si kawam beure t eumeu moko danone
Eumeu mo nagoul beure waye🙁
Wakh nga deug
Eumeu 42 ans qui n'a plus rien à prouver, lac 2 eupouko taille, poids et rallonge lou eumeu warone deff? Diène Kaïré modou anta défoul touss et pourtant dako douma dane, goné souy beuré ak kouko mak lep mom la war. Lamb goné ak mak niar douniouko beuré kène dongou la beuré war tamouy ki yakar yegg au sommet. Kou beuga done ndanane da ngay yor djiko ndanane. Dommage mais Lac 2 mo eup ay combat you niak foula ci arène bi victoire comme match nul. Meussoul dieuli mbeur daneko ci 10 ans, da nga koy songou mou plaquer la.
@@papinho9111 thank you you right 👌🏾
@@papinho9111 waho Dara
Le cachet ne gère po
Vraiment tu as raison 😢
Bilae bima setané face to face damani wone lac day ray Eumeu sene
Lac dh dou ray ken 🤣🤣🤣🤣
Lac 2 wakh rk la am si lambo dji 😂
Chiiiim 6 moy 9 niome niar nieuppa yèmm danio niakk diom
Tay mom eumeu sene est le véritable lac de guerre ..
Euy boudone sama champion bi ba legui amateur yi gnibinanou balla Gaye 2 le lion de guediawaye💪💪💪💪👏👏
Blye yw kokou rck da am fouleuh si loumouy def vive BG2💪💪💪💪
Vraiment nak eumeunsene.mondefoul been effort .parewoul ci combat bi .moom li lac deff bouko deffon ,diapantei aam
Dieul sa Million diguo dioguèe pour rien lii mome djoguo sie nèwsii doléyii mo guéne Quoi no guéne dou balla cest le meilleur même si il vas il vas nous satisfair nous les amateur
Monekhal lamb dji hier té signature rekk lawon
Une grande déception, franchement gnii daniou yapp nitt yii
Je partage
40munitou yalla gnouy weur weurloo amateur yi sans même un seul contact physique 🤔 mé yi tam nagnouko si lac2 motakh ma gueum balla gaye 2
v
Ohh lac mii dafa décidé wone dhe eumeu sene beurewoulll darra
Niou mayla revanche do nieuw bagarre diap dane Chimmm guay cinéma
Lac 2 machalah mbeur ❤️💪
Merci
Félicitations lac eumeu ya done wakh né combat deux personnes nio koye daf ta taye beuré wo lac mon daf lepou
sawayyy lac loumfiii deff???
Eumeu amatoul loumouy prouve 😂😂😂
Fi ken defou fi dara
Lamine tu es professionnel
Vraiment lac à raté sa vocation il l'aurais joué de la comédie au grand théâtre
🤣🤣🤣
Lamine wakh nga deug d lac boullma laale boullma diégué laiy beuré
Félicitation lac si tout le monde est contre toi
😂😂y’a nekh
Il joue comme ça
Beure niar niokoy def 🧏♂️franchement parler eum dieumoul dra srx
Pikine dal Ama Moko yorr do am tension bilahi👑👑
tu ment
@@mounassndiaye1745 Toi t'es véridique🤙🏽Tu ment" S lay am ok bonne soirée
Le problème moy Sénégal dugnou atte deugg euma parewoul sakh
eumeu Magal n'a nak 😂
Yaw topal feulé lac moye dieulesi revansse ta mo geuneu nékk xalé na wané bopame
@@galsenegalsene eume tay da daw lambji yeup akhhh
Au nom de Dieu lac dou dara il oublie qu’il est plus jeune
Deux lutteurs en méforme il suffit de voir leurs ventres pour comprendre qu'ils ne foutrons rien d intéressant.
Jimmy Diene Eumeu a battu Balla, Lac et Bombardier avec cette ventre! Eumeu n’ etait seulement pas pret pr le 4.
Nékhuol bah nékuol lac 2 diambarlah machallah
Félicitation Lac 2. Il a lutté vraiment
Wax deug nak lac mo beuré combat nak. Eumeu xaméwoumako téy... Je le comprends tmt
Eumeu sene est en fin de carrière , il est à bout de souffle il se déplace difficilement .
Lac lane la beurer fi? Maylene gnou diam lac öo gueneu niakk fiom chi mbeur yeup
Wakh deug yalla contre n'a Lac 2 trop mais combat bi môme moko beurre leppu Eumeu Séné beureoul Dara 🙈🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣💪
Kholalma payi douniou beurre douniou baye comba bou geneu sof si adouna mohgui nekhoul tous
Diadieuf Lac2 yako meune fouf diko dah mouy daw rek.
Lac ❤💯👍
Beuré wouléne dra
Lepp kouy supporter Lac de Guiers 2 amo mbeur.
Qui Mbaye Match Nul wala mbaye Rassou lagn ko wara touder.
Promoteur bouffi teugeuti combat Lac De guiers diapalni
Dangay maye say million azaka
Bis dou tputi borom lay tollol macky lagn ko toudé motax
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Combat bi da reflété sougnou indépendance rek ces comme sa on a négocié pour avoir notre indépendance 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Emou yalla nala yalla samou
EUMEU SÉNE MOO YAKK COMBAT BI BEURÉWWOUL TOPP SAKKOU YI. SÉNÉGALAIS YI SOUNIOULA BAGNÉ REK BAGN NAGN LA. LAC MÉRITE SA VICTOIRE
Deug nekhul
Merci beaucoup senegalais dafa hypocrite
franchement tu as raison
Mais eumeu a bien fait de lutter ainsi, il n'a rien a perdre, c lac qui a besoin de victoire, c lac qui a besoin d'etre roi des arenes Comme moromame yi, c lui qui doit prouver, mais Comme d'habitude il a decu tt le monde. Lac2 veut la victoire sans risquer.
LAC DOUMA NAKO DAANE NAKO. EUMEU ANDIWOUL DARA SI LAMB JI DI DAW REK. BRAVO LAC
Yéne dounguéne rouss sakh di dieul revanche ba paré té do songou lac koukoy faral amo diom
mais bouléin dara bet cest deux luteur son en mauvaise forme phsik et eumeu c'est pire il est lourd graisseux et a une tres mauvaise cardio!! combat soula beté tu prends pas du poids tu en perds !! tu essaye d'etre sec et souple comme diéne kairé!!!o moins....pkoi prendre des proteine pour jeul 10 a 15kilo de graisse so solé yéré nioun naane la ponkal mi foo tok di niak ndax nine (sportif bouy tok di niak rekk si c pas une pathologie c le signe dune mauvaise prepa il nest pas en forme )!! soy soumékou nioulay djeppi so yeugeutoo 2 minutes djéhkhal cardiaquement !!et tou tes mouvemen sont limité ils ont fai une trop mauvaise preparation , mbeur athlét dagey paré tout le temps surtt niom toute l'annéee tu te prepares car cest ton metier ! reug reug toute l'année il a presk le mm phsyik tou le temps ...
Ah non pas lac, il est en forme physiquement.. .
Drapeau maky sall ni rék la meuna mél
😂😂😂
Merci lac aujourdhui ta tt fait ces eumeu Qui na pas lutter
Daguéne yap lac rk mais eumeu Mo beuréwoul
Lii dou combat lewto rekk am million
Deug mo nekh yalla tay mome vraiment lac 2 dfa gnéw pour beuré mé eumeu séne mo bougoul beuré
C op vrai ki d'où heure lac d'où touche
Merci beaucoup vraiment les Senegalais ne sont honnette
Lac dako begena nakh mai dou diel risque thi combat bi
Lac2 dey baralllll lewto pour niouné beureina
Hier mo amone ascendant pour dane mais dafa ragall ak beutou loyammm yii😂
Merci
Jamaïcain n’est pas un reporter plutôt un supporter Eume séne je suis désolé
Fèlicitations Lac 2 et Lamine liguey bi nice na mon frère
Vraiment combat bi diarul dougueul nékhul dara, lac dafa niak diom trop
Eumeu vraiment hamouma lou héw tay mais kéne hamer wouko. Lac mom warone ne degueul bopam dane ko diél bou sét bou feké mbeur leu. le combat a été décevant
Bou défoul ni nan lay déff lac2 mi modoul mbeur Emma sene li modon yonou combat bi bimou yakam tie si modou Lo giusss nga li si khewww lac2 mi modoul mberrr
@@gissatadia949 en tout cas affaire yi niak ne xorom lolouu
Vive lutte TV félicitations lamine
Mais toi qui gère la chaîne UA-cam amo kholle kou sokhore gua un de mes amis avait mis un commentaires pour demandé des abonnés gua supprimé commentaire bi pour lane tu mérite pas de géré cette chaîne di nittou dra commentaires boula nékhé supprimé KO mais dinala siwal féppou