Face 2 Face Eumeu Sène vs Sa Thiès " Dann Sa Thiès pikine moko sokhlo wone dafeu am dolé "

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 22 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 237

  • @alexisniokhorsenghor-lg4gc
    @alexisniokhorsenghor-lg4gc 7 місяців тому +49

    Vraiment, suis pikininois. Et prochain combat de Sa Thies, je suis pour sa victoire. Il est très poli et respecte énormément Eumeu Sène.

  • @OusmaneDieng-qe3tg
    @OusmaneDieng-qe3tg 7 місяців тому +7

    Sa thies franchement tu es adorable nitt guenoula yalnala yalla arrt

  • @modoumbayegning5056
    @modoumbayegning5056 7 місяців тому +55

    Mane euma moye sama mbeure mais sathies so amaté combat boudoul wa pikine yalnala yalla maye ndame vraiment kou yarou nga

  • @barow2853
    @barow2853 7 місяців тому +66

    Billahi kou yarou sa thiess yalla nala yalla are ❤❤❤❤❤

  • @pathecheikhndom9931
    @pathecheikhndom9931 7 місяців тому +20

    Man pikine la deuk mais sa thies diambar la nek si rk kou eumeu dane mom dou niak diome blh merci eumeu yaw tmt ken demoul nga dess blh 💯pour 💯 pikine 💚❤️

  • @ndiaganek
    @ndiaganek 7 місяців тому +26

    Vraiment respect aux 2 lutteur
    Wax dji barriwoul et combat bi nexna

  • @Mouhamedlo12
    @Mouhamedlo12 7 місяців тому +48

    Gnar gni il mérite le respect 🤌

  • @moussaba4865
    @moussaba4865 7 місяців тому +6

    Pikine kesse ❤❤❤❤❤eumme sène est un homme de confiance qui a fait sa carrière ❤❤❤❤

  • @Madiyan-x9l
    @Madiyan-x9l 7 місяців тому +17

    Vraiment le 2 la fair play bi si niom guissoumoko thi keeneenn big respect les Artistes

  • @waganefaye2176
    @waganefaye2176 7 місяців тому +21

    Eumeu sama mbeur nga Mais loutakh nga gadji boy bi😂

    • @fallcameleon8625
      @fallcameleon8625 7 місяців тому +5

      Det way kone mou yombou deh. Eumeu dou kougni patam patami. Sa waye sa Thiès à fait tout ce qu'il pouvait mais nak eumeu mo bari dolé rek😂😂😂😂

  • @OureyeSeck
    @OureyeSeck 7 місяців тому +20

    Eumeu da liguéye si lamb dji xolén forme eumeu bi machallah té da meun beuré mais sa thies da xarr déglou trop xawma consigne la xawma diokh thieur trop mais bokna si louko gnakk lo mou bayiko mou yègue ko fofu takk ko c po normal bilahi🧐🧐 suis supportére de modou lo mais félicitation eumeu et du courage sathies🙏🙏🏾🙏

  • @adamathiam4007
    @adamathiam4007 7 місяців тому +6

    EUMEU SENE UN VRAI COMBATANT, C'EST LE SORCIER DE L'ARÈNE BRAVO FRÈRE 😂😂😂😂

  • @idyfall7146
    @idyfall7146 7 місяців тому +5

    Ives niang lamb dala sokhla bou bakh del tew machallah

  • @SeynabouFaye-l3n
    @SeynabouFaye-l3n 7 місяців тому +4

    Respect à vous sa Thiès moy sama lutteur balla gaye yalnako yalla may ndam eumeu geste bi rafetena ❤❤❤❤❤

  • @maodosow3022
    @maodosow3022 7 місяців тому +8

    Yalna Diamou yague

  • @buz7755
    @buz7755 7 місяців тому +2

    Machallah eumeu lambou ni la diamou rek ❤

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 7 місяців тому +1

    Merci bless all of you Amen Amen Amen Amen Amen 🙏🙏🙏👍 very spotive

  • @bambasene4163
    @bambasene4163 7 місяців тому +11

    Nguirr Yallah Lamine Samb , Déll DégloOo way , Beurii Gua Wax trop té manOo Dara

    • @Nialy-u1o
      @Nialy-u1o 7 місяців тому

      Tay kay defoul dra

  • @eumymodou6827
    @eumymodou6827 7 місяців тому +7

    😂😂eumeu bayil gadjè

  • @aliounediouf2092
    @aliounediouf2092 7 місяців тому

    Sa thies yalnala yalla samp te samba ya yaru té goré sportif 100% bilaye sokhlana sa numéro Eumeu sama beurla wayé neek n'a sa fans ndakh sa djiko yalnala yaĺla doleel ya raby

  • @daoudaciss2880
    @daoudaciss2880 7 місяців тому +2

    vraiment vous etes sportifs❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @sallaziz1663
    @sallaziz1663 7 місяців тому +3

    Sa thies d'où guawa nek champion defa am ay moment you décisif si carrière boko manquer rekk , tu passe à côté

  • @cheikhdia5402
    @cheikhdia5402 7 місяців тому +1

    Tu as bien communiqué Sa Thies 🎉

  • @ModouFaye-v4z
    @ModouFaye-v4z 7 місяців тому +1

    Sa thiès mashallah ❤❤❤❤❤

  • @baraleye4749
    @baraleye4749 7 місяців тому +6

    Saa thiés dé 3 déféte la am ta gniko dane warnanko daane ay champion lañ kom mom ta eume séne magouko makk gou tax ñouy wax ta eume séne mie modou lo dako dane jangalko beuré

  • @Amzomamzo
    @Amzomamzo 7 місяців тому +3

    Le bonheur de la lutte

  • @ndeyendiaye1265
    @ndeyendiaye1265 7 місяців тому +1

    Wawaw Eumeu yangui gnouy diangal lambb❤❤

  • @dkr2214
    @dkr2214 7 місяців тому

    Respect bi nekk sén diggënté ñom ñaar mòma gënë neex ❤❤

  • @assanebabaofficiel3533
    @assanebabaofficiel3533 7 місяців тому +7

    Sa thies eumeu dala éto lolou mola dane

  • @abbasane
    @abbasane 7 місяців тому +1

    C'est ça la vie 🥺👏

  • @omarba9047
    @omarba9047 7 місяців тому +1

    MAIS TONTON LAMINE SAMBA SA THIÉS VS MODOU LÔ DA WARA AME DH SA THIÉS A FAIT UNE EXCELLENTE CARRIÈRE MOIN DE 30 ANS SVP SA THIÉS VS MODOU LÔ COMBAT DOUKOU GUENE NEKH ANNÉE PROCHAINE 2025 INCHALLAH SUNÉKHÉ YALLA SUNU BOROME

  • @LamineBadji-x3r
    @LamineBadji-x3r 7 місяців тому +2

    Sa thies du courage ❤❤❤

  • @ibrahimasambndoye-wq4ny
    @ibrahimasambndoye-wq4ny 7 місяців тому +1

    Eumeu Séne moy sama mbeur wayé sa thies yalna nga nek roi fes arène kou meun beuré 'ga yarou te guem bopam

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 7 місяців тому +4

    Eumeu modou sokh latoula dane nala gñiara wone ak magñiére boumoula dané doye naa seuk eumeu kham nani comba dotoko am

  • @DiarraSene-t3f
    @DiarraSene-t3f 7 місяців тому

    Félicité sathiese dafnalamoun si gueduewaye eumeu séné moulana dorna eumeu séné wayé nako diom🏟️⚽🇸🇳☺️☺️☺️

  • @Oumou-t8i
    @Oumou-t8i 7 місяців тому +3

    Merci sa thies

  • @Domou_Deukk_Bi
    @Domou_Deukk_Bi 7 місяців тому +6

    Sathies dafa complexer trop sikanamou Eumeu

    • @MamecheikhTourecheikh
      @MamecheikhTourecheikh 7 місяців тому

      Sett lo ga lolo 😢kersaa bi dafa eupo ni boy niang defon balla lako warona def

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 7 місяців тому

    True Eumeu balla ,,, Yes , Sa thies. Gris , will be a nice comba 👍👍👍👍👍👍👍✌️🌍💪🙏👍 Gacher😁😁😁🤣🤣🤣😁😁✌️

  • @KhadySene-w4g
    @KhadySene-w4g 7 місяців тому +2

    J'aime beaucoup sa Thiès

  • @alioundiaye1851
    @alioundiaye1851 7 місяців тому

    Sa thiés nena da am dollé Macha allah con bakhna

  • @Gkcdshndsncs
    @Gkcdshndsncs 7 місяців тому

    Nekhoul ba nekhoul eume senn à bien entraîné 👏👏👏👏

  • @baratoure6858
    @baratoure6858 7 місяців тому +1

    Sa thies dafa am kérssa si Eumeu séne bilahi dafko respecté motakh ma beug ko

  • @OusmaneBah-cm8kq
    @OusmaneBah-cm8kq 7 місяців тому +1

    Eumeu sène communique bien

  • @MouhamedGueye-o2b
    @MouhamedGueye-o2b 7 місяців тому +3

    Sa thies diambar deugue barréngua ba danou

  • @alioubah-wi4ub
    @alioubah-wi4ub 7 місяців тому +1

    Sathies dou nitt bouy relever deffii tjrs franchement tjrs c est comsa ki danne sa mag 2fois gha wara diele revanche

  • @babadia5289
    @babadia5289 7 місяців тому +1

    Non Sa Thiés niakh naa diôm nat 😢😂😂😂😂😂😂😂

  • @cisseali659
    @cisseali659 7 місяців тому

    Eumeu niata défaite la am???😂😂😂

  • @coolfree8778
    @coolfree8778 7 місяців тому +5

    Dafa la wakhou tek la khel amo foula chim

    • @ibrahimaniane6508
      @ibrahimaniane6508 7 місяців тому +1

      Bayii ko fofou mou topp dii wakh ayy grand bii ak pas bii lamb amoul lolou dee lamb sou ndioté reek ay respect amo toufii sa sou continue nii bilahii dou gawa am loumou beug si lamb dji

    • @coolfree8778
      @coolfree8778 7 місяців тому

      Foula AK fayda la amoul​@@ibrahimaniane6508

  • @thiammamadou3244
    @thiammamadou3244 7 місяців тому +1

    Vraiment Sa amo beuré bou dane Eumeu😂

  • @dawdatouray266
    @dawdatouray266 7 місяців тому

    Very nice ❤❤❤

  • @MortallaNdiaye-tc2pz
    @MortallaNdiaye-tc2pz 7 місяців тому

    👍🏻👍🏻👍🏻

  • @RAMB75
    @RAMB75 7 місяців тому +1

    Voilà Merci Sa Thies dieuleul Gris so meune ta ame Bom. Eumeu dieuleul Franc té mome nga beugue pour espérer wate couronne 👑 bi. Balla Gaye aussi combat royal monék si bop bi donc na affaire yi peuthiakho. En plus grand contre petit yi fok mou continuer un peu pour niou battré wate carte yi

    • @modo6218
      @modo6218 7 місяців тому +1

      Eumeu de gouy gui lay khar dou dieul franc 😂

    • @Jerkin-amabalde
      @Jerkin-amabalde 7 місяців тому

      @@modo6218franc da eupeul motakh dou gawa beurel ak grand bi

    • @RAMB75
      @RAMB75 7 місяців тому

      @@modo6218 nako dieul albouraq loumouy khar eufeul bok wala Franc vs Lac féké Eumeu da khof boy bi mais Eumeu n'a lidianti walé retraitam gagné bognon

    • @matarmbuegu2855
      @matarmbuegu2855 7 місяців тому

      @@RAMB75ah lolou la guiss eumeu ak sa niniou wakhue pare wouniou pour fran

  • @hamidoutall9134
    @hamidoutall9134 7 місяців тому

    Sa Thies diokh len ko Bombardier sa thies dane ko

  • @tolamonnene224
    @tolamonnene224 7 місяців тому

    Félicitations champion

  • @diogoundiaye3926
    @diogoundiaye3926 7 місяців тому +1

    Nice na

  • @buz7755
    @buz7755 7 місяців тому +1

    Eumeu mo am dole 🤭

  • @khadim1875
    @khadim1875 7 місяців тому

    la corpulance de eumeu est mille fois meilleur que celle de sa thies

  • @Mf-zl7tr
    @Mf-zl7tr 7 місяців тому

    Sa est très poli

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdong 7 місяців тому

    Niongi felissite eumeu sene ak pokola niounie wa ginaw raill si victoireeyi ndakh pokola moooy souniou bathie seras niounie wa ginaw rail ce le melleur dafa dor liss mou danou

  • @malickdiedhiou5184
    @malickdiedhiou5184 7 місяців тому

    Sathies mâchalah kou yarou la , il mérite vraiment du respect

  • @أحمدسيك-ص1ت
    @أحمدسيك-ص1ت 7 місяців тому

    ❤❤❤❤

  • @linkstardidingkeba2922
    @linkstardidingkeba2922 7 місяців тому +1

    Bilahi Mane Sathies Balla Gaye ak Ama Baldé rek lay supporté mais sa Thiès dafma ték gathié ci comba bi. Li ma gueuna méti sa you amé combat examen rek danou

    • @mouhamedlydiouf8934
      @mouhamedlydiouf8934 7 місяців тому

      Toi au moins tu comprends se que ressentent les supporters de sa thies. En ce genre de combat ngay khamni balla gaye mo tene sa thies ci combat examen

    • @mouhamedlydiouf8934
      @mouhamedlydiouf8934 7 місяців тому

      Sa thies defoufi d'ara. Dadone setane rk

  • @aliouneseck2540
    @aliouneseck2540 7 місяців тому

    En ma connaissance eumeu dafa amé yeurmandé si sa Thiès

  • @mohamedbenzekry8074
    @mohamedbenzekry8074 7 місяців тому

    Sathies a trop respecté eumeu bokna si liko dane

  • @KhadimDiop-z6l
    @KhadimDiop-z6l 7 місяців тому

    ❤❤

  • @elhadjisunugal
    @elhadjisunugal 7 місяців тому +1

    Lii dall balla cii boye niang sa thies la waraa nekk barrage zou balla mais chak combat examen gua niakk koo

  • @OumarSow-bh9ci
    @OumarSow-bh9ci 7 місяців тому

    GNarri mbeur yi masounou yake lamb sén combat yép nékh té méti

  • @khadimndiaye4105
    @khadimndiaye4105 7 місяців тому

    Sa Thiès champion leu

  • @Myou-0291
    @Myou-0291 7 місяців тому

    Yalla baxna

  • @Mmodou
    @Mmodou 7 місяців тому

    Degue nèkhoul sa thiès ak balla gaye gniewugnu eumeu sène 😮

  • @moussasarr67
    @moussasarr67 7 місяців тому

    Sa thies yaw ak eumeu aye waye bouko dara yakha

  • @Izamnklofficiel5890
    @Izamnklofficiel5890 7 місяців тому

    Il est vraiment le petit sœur de balla gueye???

  • @gueyemouhamadou7546
    @gueyemouhamadou7546 7 місяців тому

    C.vrai c'est un athlète Sathies mé meunoul chaque grand rv mou niak ahh nioune danio sonou

  • @thiebalde921
    @thiebalde921 7 місяців тому

    Yow souma la rous wone teupp leumbeul wayy janrou doff yi khamoulènn lambe beuri sathies nioumou Dane nieupp séne keur am na mbeurr

  • @Ciiskoblind
    @Ciiskoblind 7 місяців тому +1

    Ioe sa Thiès sa grand combat yeup dagako perte

  • @NdiaboutaDiouf
    @NdiaboutaDiouf 7 місяців тому

    sa Thiès gris bordeaux eumeu sene gouy gui

  • @OusmaneDieng-pr6jf
    @OusmaneDieng-pr6jf 7 місяців тому

    Sa Thiès dafa niak diom qui d'âne frère ga wara def lou ler sa Thiès amoul foula

  • @aliouneseck2540
    @aliouneseck2540 7 місяців тому

    Eumeu AK sa Thiès warouniou wone beurré walahi niome niare déno nawanté

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdong 7 місяців тому

    Eumeu tamine wonenani khalela balegi nako franc dieule mou meyeko sanse diap franc doumako daneko

  • @massambadiop8181
    @massambadiop8181 7 місяців тому +76

    Sa Thiès kou niak diom leu thim dane sa makk 2 fois nga warone ko tekk lou méti dane ko ngay nekk fi di beuri wakh dialal feulei do dara

    • @AbdrahmaneSy-jr1bb
      @AbdrahmaneSy-jr1bb 7 місяців тому +19

      Eumeu légui Double Less la touddou

    • @sadotoure3182
      @sadotoure3182 7 місяців тому +61

      Changél sa Esprit,ndam yalla mokoyy mayé , j'espère que milliardaire nga rek ??

    • @AbdrahmaneSy-jr1bb
      @AbdrahmaneSy-jr1bb 7 місяців тому +8

      @@sadotoure3182 Sa way finga yobbou wakh aggoul fofou dalal geunoma geum YALLAH ndam rek lalen yénéwone motax may wakhé snn ya rien

    • @iboundoye5872
      @iboundoye5872 7 місяців тому +10

      Mo ioe mi mome louy sa problème tmt

    • @seydinaoumarciss561
      @seydinaoumarciss561 7 місяців тому +17

      Frère mbeur sou respecter entraînement yi respecter adversairam limou wara def yeup mou defko lisi dése nak si lokhoy yalla la nek vraiment té sathiés il a tout fait pour ce combat encourageons leu rek

  • @gueyemouhamadou7546
    @gueyemouhamadou7546 7 місяців тому

    Sa layam layam bi ngay bayi lamb douliiiii ahhhh on en a marre

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 7 місяців тому

    Eumeu guemeul yalla modou mooy sa baye

  • @babacarseye49
    @babacarseye49 7 місяців тому

    Non ives niang mo meuna way lamb wayyyy

  • @legendediop9215
    @legendediop9215 7 місяців тому

    Degeul fadam 😂😂😂xamoul gatte

  • @Ratatouillebaldeh-f9p
    @Ratatouillebaldeh-f9p 7 місяців тому

    Adouna dou Dara lii rafet na

  • @coolfree8778
    @coolfree8778 7 місяців тому +1

    Sa thies bayil sa signe yi té gua degal sa bop vrai complexé gua

  • @azizngom
    @azizngom 7 місяців тому

    Eume vraiment sope nala lol nax sa diam

  • @modo6218
    @modo6218 7 місяців тому +2

    Franc kou bagna danou boulko dieul 😂😂

    • @LamineFall-r9p
      @LamineFall-r9p 7 місяців тому +2

      Bayilén fofou ngiouy tékkeu khél franc dé kouko djeuloule dagua ragual rék mais diaroul wakh djou bari😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @modo6218
      @modo6218 7 місяців тому

      @@LamineFall-r9pmounan ay franc Aliou Sey eumeu gouy gui la begue khar victoire yi la begue yokou

  • @khabylameofficiel5927
    @khabylameofficiel5927 7 місяців тому

    Fadam mom ay ree lama def bouy wakh daga nan dieul😂rois des arène tes sarap ndeyam xamouko 😂😂

  • @Mackenzi-z4f
    @Mackenzi-z4f 7 місяців тому

    SA THIES JE TE CONSEILLE E LUTTER AVEC LES VIP CAR IL EST TEMPS

  • @DioufCisse
    @DioufCisse 7 місяців тому +2

    Yaw ak balla Gaye daguène fatè lilène falle ms gnoune wa Casamance beugeu nagnlène ba parè ms svp dèlosilène sène xèl surtout ton grand frr balla ? Yalla na diam yagg

  • @صالحتياو-ر6س
    @صالحتياو-ر6س 7 місяців тому

    Sa thies nak nelaw gua si comba bi ahhhhh

  • @mouhamedmoustapha684
    @mouhamedmoustapha684 7 місяців тому

    Sathies ya taylè sa bopp so danonn eumeu sène heure bi yak modou lo dayy saff mais nga niakatiko

  • @khaliloulah3703
    @khaliloulah3703 7 місяців тому +1

    Frank nexoul gnémé dh😂😂😂😂

    • @matarmbuegu2855
      @matarmbuegu2855 7 місяців тому

      Ah nima guise niar ngi wakhe ken duko si diuell

  • @omardiouf4248
    @omardiouf4248 7 місяців тому

    eumeu yaramou athlète deug la yor

  • @AbdrahmaneSy-jr1bb
    @AbdrahmaneSy-jr1bb 7 місяців тому +2

    Sa yow ndékété do touss say morom rawnagn leu

    • @MameThiaw-i6k
      @MameThiaw-i6k 7 місяців тому +1

      Yaw wére gua

    • @AbdrahmaneSy-jr1bb
      @AbdrahmaneSy-jr1bb 7 місяців тому

      @@MameThiaw-i6k Non Wa keur Double Less dagnouy togñ séni supporters

    • @fofanaidrissa489
      @fofanaidrissa489 7 місяців тому +2

      Bro moi suis sa thies mais eumeu mo meune famille double less lolou 10 combats dalene di dane
      Modou mo meune wa cote pikine
      Double less nio meune cote parcelle bi lolou la lire té eumeu champion la deh

    • @AbdrahmaneSy-jr1bb
      @AbdrahmaneSy-jr1bb 7 місяців тому

      @@fofanaidrissa489 lou leer nga wakh bro

    • @AbdrahmaneSy-jr1bb
      @AbdrahmaneSy-jr1bb 7 місяців тому

      @@MameThiaw-i6k Dédèt wérouma

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdong 7 місяців тому

    Eumeu dafa bakh yarou beug pikin mai nak thiowelithioweli pokola balde kasse la niou topou mooy souniou bathie seras man la kheuss bou bathie seras

  • @djibrilba9084
    @djibrilba9084 7 місяців тому

    Sathies da nga danou beug yek bougnou sonal tei djeul franc ya tardel sa bopou war nga rouss di lathié Gris bordeaux ish

  • @CaramocoDiallo
    @CaramocoDiallo 7 місяців тому

    Sathies gris moy yone

  • @tallbathie1293
    @tallbathie1293 7 місяців тому

    Koulen degue manam nieme woulene Fran lag dieulele avance bi wirri wirri diarinari tiey sa ma gnaguo bi