Ne te laisse pas piéger par des gens qui ont un seul objectif ta chute. Continue de travailler, promouvoir ton album dans la paix, sérénité et que le seigneur te protège, guide, t'octroie l'énergie nécessaire et la foi pour faire face à tous les dangers sur ton chemin dans sa miséricorde divine!
Maala buga seck the king of his generation c kaw c kaman rek inshallah adina NOLA buga seck dunda beh dunda sapila sa dunda Amna ngering from Gambia watching
Wally Ballago Seck doundeul wereul amal diam amouniou sa faye sounou xool yingay tokal neex neex Yallah nalako borom bi deifal ay yiiw sa music safna amna goût ya meune dh 😂🔥❤️🇸🇳
Wally et son orchestre sont un cas d'école. Ils viennent de nous faire déchiffrer la musique Sénégalaise qui est vigoureuse, pleine des percussions et des rythmiques. Coup de chapeau à l'artiste.
Youssou dieng wah tan bi nehhhhhhhneu marshalla I love the calm down ram Dan bouniou defeh dankeu sahhhh dey nekhhhhhhh leeee eupeuna 💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥
@Miime Cisse oui ça moom c'est vrai mais c just que ni bou defe soire tant que setanoumako rek dou ma nek motakh. mais wakh ngua deug qualité video yi moom bokkoul
I love you wally seck doundal ba indil niou disques d'or kouni amine beujeul jaime1❤
Le Messi , CR7 ,Neymar ,Mbappé ,Benzema de la musique 🎶 Sénégal 🇸🇳♥️♥️
Kou beugue wally beseul j'aime bii💪♥️
Yafi nek wally kou begu mame diara maye ko J’aime❤
Rétro mane mome rek lay deglou sa me rappelle pcm 2016 au 2018 ndeyssane maman katy bii vogrio
Retro nga niou lal dh macha’Allah daf siy bakh Mar Yacine kéne dou ioe longue vie ✌️🫶
ki moyi borom Sénégal 👑🔥
Si Dieu met une cuillère de sucre dans votre café même si ont met tout les sel du monde le café sera doux ééeee papa balléne danio dioummm🔥🥰💪👑
Disque d'or bi laniou soxla wally👑👑👑👑👑
Waly nak dafa yabate grand théâtre khadia tofa dh😂😂
Wally anniversaire wa wally familly laye deife donc il faut mou deime grand théâtre pour se souvenir de leur existence
@@Mody-nz3zt en ok
Bilahi là ou tout a commencé 😢
No wally yalna yalla jamal lafal len chatt . Yamunaa woi sa melody reek Benaaalaaa
J'aime ndey gueye c'est une femme très digne malgré le statut social de son mari elle l'aime à mort amour sincère
Demain inchallah c'est anniversaire de mon futur mari ❤️🔒💎
AYEE WAY 4 FEBRUARY REK AK WALLY 🔥🔥🔥🔥❤️🇬🇲💯
Fo deuk si gambie
@@moustaphagaye1457 brikama
Teww rek inchalah
Bilahi Wally kou la khole begue la sama dome Gui sama khole l'ala defe🙏🙏🙏🙏💥💥💥🔥🔥🔥🔥🥰🥰🥰😍😍❤❤
Sa répertoire mo graww le 04 yokouthi voglio gouney waliyé(Wally seck magg na) paradise live complet baye Wally étudiant mana(elle m’appelle daddy )etc …y’a graw ❤
Yagaraw 😊
Yaw vrai mélomane gua ay sound you graw gua wakh
@@mamourndiaye9497 woykate bi mo graw
@@dimkasoumare1673Lou ler Ken dou mom dafa yemè dal entouka on est fier de lui 💪
Mane awma ticket 😭😭😭😭😭diapaler leine ma
Ballago dama khoulo sama guel khol bi nekhoul wayé milano bi❤ takhna ma faté nakhar bima amone
Niaf rétro yi la namone. Soirée intégrale rétro ❤️❤️❤️❤️❤️
Walay
Ppp
Lii gnouss na nekh diii🎉
Ne te laisse pas piéger par des gens qui ont un seul objectif ta chute. Continue de travailler, promouvoir ton album dans la paix, sérénité et que le seigneur te protège, guide, t'octroie l'énergie nécessaire et la foi pour faire face à tous les dangers sur ton chemin dans sa miséricorde divine!
Amine m’a belle
Amine
111
@@assemalick7456 ýý⁷⅞b
Maala buga seck the king of his generation c kaw c kaman rek inshallah adina NOLA buga seck dunda beh dunda sapila sa dunda Amna ngering from Gambia watching
Cheikh anta Ndiaye nous manque 😢
Billahi surtout la percussion sur wurus ken d’où mome
Il est où?
@@Thiernondamaldarou92 Cheikh Anta a perdu sa femme.
Bilay yaw
Bilakhi ya meun💪 ya eupp doolé❣
Merci wally le chenteure du peuple man la papito bou wally seck brom le 2 anniversaire bi
Wally waye réke laye déf mashallah,Milano me fait pleurer, je ne sait pas le pourquoi ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️diame ake longue vie pour toi
Rétro dafa nékh mashalah dé gnou ko May chaque dimanche way mon ami de valeur ki gnép beug
Ay way begue na dem le 4 😭awma ticket yeine
Wally do nitt live mom Yako dakh si Sénégal 🇸🇳 non je t’aime de tout mon cœur ❤♥️
Yalla arrall niou sonou wally mi
LEGUI SAKH WALLY BO DEFATOUL LIVE YOU YAGG YI DAGN LAY BAYII
😮dinaaa khawaaa ki d😂
Sheuut wa raam daan nioo degg rekk ❤🙌
Wally nii leu plus de rétro rekk 😍😍😍
Saraabaa deniouko livaal 🥲♥️
Soul ker d'où ko tere feng ken d'où yaow si mim reew ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Bayil niou téléchargez ko diko file après job😍💗💪🏾
Hana Auchan ngakoy télécharger
Wally Ballago Seck doundeul wereul amal diam amouniou sa faye sounou xool yingay tokal neex neex Yallah nalako borom bi deifal ay yiiw sa music safna amna goût ya meune dh 😂🔥❤️🇸🇳
WA MAI ANNA BOGA WALLY ???
Bilahi li mo dakk ay Doro Gueye mome
Wa Papa Wally mi est ce k nitt laaaa 😭😭😭😭😭😭 li rakhna Rapp dhh serafalllll♥️🥰🥰🥰🥰🥰🥰😭😭😭😭😭♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Loutakh vidéo yi douniouko télécharger
Brom Reew Mii ❤️🇸🇳
Respect wally les retro sont magnifique malgré que l'album etat d'esprit soit le meilleur
Live bé doy waar yèn😀
Trop
Ani wa BRESCIA ❤✅
Quelle voix envoûtante et sensuelle de Wally dans une superbe ambiance mashallah!
on dit plus chanteur du peuple, mais le chanteur du continent africain
❤️❤️❤️ wally yaw ya takh niounay nitt so bayiwè musique digua ray adouna ont t'aime très fort
Nidiayou Wally bi farisse la mashallah ❤️❤️❤️❤️
Man yi meun nama rayy ay voglio saraba ma santé yallah bamba touba lolambe ohhh❤❤❤❤❤❤❤❤ Nio m’a dakhal yepp mai nak bagnioumasi bene 😂😂😂😂😂😅😅😂😅😂
Man saraba momay ray
Voglio ak tieugine ❤🎉
@@layewade5428 uyte8
0010
Do bayi gnou télécharger ko svp
Wally et son orchestre sont un cas d'école. Ils viennent de nous faire déchiffrer la musique Sénégalaise qui est vigoureuse, pleine des percussions et des rythmiques. Coup de chapeau à l'artiste.
Ki Moy domoukharam😭😪♥️
Rendez-vous le 04 février au grand théâtre national de Dakar spécial retro 🐐❤
😢❤️Saraba dafmay dundal 😢❤️
Wally ballago séck ☕️💫🔥👑💯 Bilahi Tu es le meilleur chanteur du peuple sénégalais 🇸🇳🔐 makô wãkh point
Notre préféré ✍️✍️
Wally aziz faye bi meuna toko tu es le meilleur one love
Ya ngui dora niew nak son yi mo nekh ballago masalah
Vraiment li mom dafa nekh je l’écoute toujours les jours nek dou ioo Maryacine mashalla ❤❤❤❤❤
Wally b seck le meilleur de sa génération et merci pour le travail remarquable
L’incroyante Wally Ballago Seck chasse qu’on t’a placé là où aucun artiste ne peut y accéder on t’aime fort , bien, fou…❤❤❤❤❤❤❤
Bilahi
Le roi de la musique est là 🏆❤️ yalna sa djam yague ❤️👌notre fierté nationale et internationale
Kou xam Wally loumouy rhé😂😂😂 non Mbaye Sy dou nitou fi
wally kana dafa am contrat
ak wa tik tok
😂😂
Mmmmmmm
Mare Yacine le chanteur de tout les temps ♥️🎤 yafi nek ms rétro yi nekhna trop ✌️
wally kana dafa am contrat
ak wa UA-cam
😂😂
Machalla chanteur du peuple wally ballago Seck jtm bcp ❤❤❤❤🥰💃
senegal yafi daka woy❤❤❤
Faramaren la mai fo fate yousou
Defma ndank Wally faut comme la 1e foit c’est se que nous aimon tu vois Ps les tik tok
Massallah wally seck May God continue to bless you
Bilahi walahi Dafa meuna wayy 🎤 ❤❤❤❤
Wally comme sonko rek bou noyolone soulnegneko bou yague😂😂😂💝💝💝💝
Nonou la demer nak 🤣😂
❤❤❤
Mar fipou na nak🎤👑
Mon frère amal diame tu as un jolie cœur que dieu vous protège long vie a vous on est derrière vous
Sama wadji mon Ami d'affa diotteu saffai 11ans néwone n'alla souma Amatoull gua dême bayima Ibrahima halilou l'a harittou yalla wathiatte niew doneu fi Mame cheikh ibahima fall bou wérr boulle NélaW 🤐👌👏 2012ibrahima seck
Bou bakh bï 👌
Live bi nékh na trop vraiment
Machallah ndeysan li nekh na dem bou la maye fatali yallah gua am diam wally❤❤❤🥰🥰🥰🥰😍😍😍😍
Le meilleur de sa génération ❤🎉
THE GOAT DE LA MUSIQUE SÉNÉGALAISE
Si quelqu’un connaît le titre de la dernière chanson je suis preneuse jerejef Fatih 😊1:20 jusqu’à la fin de la vidéo 🥰
Li meun nama rayy 😭❤️❤️❤️mar balgnou 😭❤️❤️❤️
Noungouss le guitariste aye na trope❤️❤️❤️❤️
Youssou dieng wah tan bi nehhhhhhhneu marshalla I love the calm down ram Dan bouniou defeh dankeu sahhhh dey nekhhhhhhh leeee eupeuna 💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥
💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴💴
Le chanteur du peuple le choix du peuple li dafa nékh
Bilahi retro yi dra dakhou ko amna bo defon dockpullman ms chaque guoon ma deglou ko daga graw🎉
2017 bi la aka doy war
666666666666 think
Waly
@@mouhameddiallo6306 ¹1qqqqqqqqqqàq
@@mouhameddiallo6306 7
Chanteur du peuple 🤞✌️🎶🎤👑 le golden boy 👑🎤✍️
J'aime voir wally, eumeudi,ameth thiou ensemble 😁😁😁❤️❤️❤️❤️
Wally Milano ohhhhhhhhh😭😅
Wally seck chanteur du peuple le meilleure king dès King
Nioune yao la nou begue WALLY❤ ❤ ❤
il est bon j aimerai le voir à Guinée conakry
Dama xarr live ba sonne🥺🥺
Samedi rétro s’il vous plaît 🙏
Yafi nei kiserafal ❤️🥳🥳
YANGUI CI YOON WII FRERE WALLY ON TE SOUTIEN ET ON TENCOURAGE LOU BEURI
état d'esprit bi live ak borom keur rek mo ci dess
Auhhhhh milanoooo milanoooo milanoooo
dou mourm gayi 🙏🙏
L’oncle de wally a donné une très bonne leçon à mapenda seck mandiaye seck ousmane seck et bambali 😂 nieuw balssi maye sa diarbate khaliss 😂
bayi ba nou setane ko ba parenguene di ko dora dougual. ni guene defoone si album bi
@Miime Cisse oui ça moom c'est vrai mais c just que ni bou defe soire tant que setanoumako rek dou ma nek motakh. mais wakh ngua deug qualité video yi moom bokkoul