Wally B. Seck - live VOGUE HD / Dimanche 27 Octobre 2024
Вставка
- Опубліковано 4 лют 2025
- En concert à Paris Adidas Arena le 07 Decembre. Prenez vos billets ici billetterie.ad...
Ouverture des portes: 17h30
Début du spectacle: 19h
………
Retrouvez-moi sur :
Tik tok: / officiel.wally.seck
Instagram: / wallyseckofficiel
Facebook: / wallyseckofficiel
Snapchat: / wally_seck
………..
Camera: Lourass Diop - Djiby Niang - Momo Diop
Graphic Design: Lamine Cissé (Damelas)
Ingénieur de Son: Bakary Banora
Mix : Seydou Boye
Realisation : Lamine Cissé (Damelas)
Focus rk thi rétro yi barki Rassoul 😘😘 sama xéll Dém na Thi 2015😢 Cobayiiiii
Quelle performance, j'ai trop aimé les nouveaux live de Symphonie, Taxi love et Yoon Wi. Vivement les autres retro Thieuguine, Djiguene, Gouné, Papa thione, etc etc. Et on attend toujours le prochain hit avec Baye mass, j'espère que ça sortira avant le 07 dec❤️
Très stylé 🎉mar Yacine très talentueux 💯 le noir te va à merveille que dieu t'accorde une longue vie et de santé inchallah ❤️
❤ premier commentaire max de j'aime pour les fans du Wally B seck
Wa yén symphonie guiss nguen harmony biko Wally di wayé nimou changé té nekhhhh non li khéré na way na Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mane dei Waly diakhal nama. Ses lives je peux les écouter tous les jours doumassi doyal.
Et à chaque fois que je l’écoute chanter, samay rongogne di gueneu khawma lii lanla.
En tout cas yalnala yalla are, mousseul la thi thiate té mou gueune la yok ay kheweul.
Machaallah.
Wally linguaye dégage thi fraîcheur doyena warr live yi nekhna armonie octavé na avec un nouveau style surtout légui danguesi bollé dance bou doyewarr vraiment mbécté rék machallah 😍🙏🏾
Goudeull fane Mar 💃💃💃❤❤❤❤❤beughone la yegueull nii grippe bii bayi nama dhé🙏🙏🙏
Kou guiss ni style bi mo diapp @Wally rk mayy ma ayy j'aime ❤🎉
Djitou et après 😟
A gore na dh 😮
Wally bi ak pp barca bi rek🎉
Mouhamet bou Wally sama khôl la nekh Wally diam si yaw ❤❤❤❤❤
Longue vie à toi Wally Ballago je ne me fatiguerai jamais de regarder et écouter tes musiques mon unique artiste préféré depuis tes tt debut❤🎉🎉 que Dieu veille sur toi amine 🥰😍
Wally sa yarame nimou tangué fan yi boudé mome ngua nara yobou le 7 déc dina metti dina yague dina bari ay mort ak ay bléssé meune ngua trop wayy❤️💪💪
Doynawarr mane rappeur la wone mais toupe n'a tps yi wally rek lay deglou😂😂
@@famazidia yagui deglou kou meuneu wayy nak doko meusseu rethiou d focus rk😂
Wally rek
Musique bi dafa geuneu nekh 😂❤️
Îu@@famazidia
Wally lii dafa khèrè dh histoire bind nako balgnou mar Yacine 😂❤❤
Wally seck son symphonie bénén aférla ❤❤❤❤machaala yalla na yalla saam mousala si thiat
Wally Say rétro lanla kou d'accord ni rétro yi mo dakh you Besse yi rek lalal je me sourtou tax love 💕💘 bi lenen la tamit ❤❤
Wally b seck the king of the king le meilleur de tous les temps
Vraiment je suis trop émue ma Yacine Maé kendou yiow cii rewmi Bahh wesh ya meune dehh diam ci yiow ❤❤ je vous love les gars on va chauffer 7decembre adidas arena wa 78 et 18eme vous êtes près ne pas rater ❤❤❤ inchalahh
Liii nekhna way❤❤❤
Wally déniou niamal bénn retro parfois lousi mèlnè impossible love remix ❤
Sen mouchouir na sale bi wekh si adidas arena bi narna grave Machallah 💯💯
Thiey mar yacine goudalll fannnn🎉❤🙏
Li tamite ba kagne nak wally ya meune waye ❤
Symphonie bi Diarama raay rek ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Ioe lii dafa eupeu dh
Ba 12:06 une vrai délice 🎉🎉🎉
Kon baax! Go WALLY ! Mbëggeel gu rëy ak sargal ci Australie! J'espère que Google Translate de l'anglais à Wolof est OK!
Lii dfa tourouuuu way 🎉🎉🎉❤
Nom billay wally mako beugue lo defe mou nékh ❤❤❤
❤sama hol séde na ya meuna live🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Wally seul❤ Wally késsé 🎉tu es le meilleur 10 du mbalakh sénégalais Nay daw rek amoul arrêt 🫂🫶
yalla nala yalla samou aar leu may leu goudou fane❤
Légui symphonie rk laay xaar❤
Tieuy sama wadji 7 decembre adidas arena yeureum na niafay nieuw ❤😂 ndax doulén yeireum li ma guiss si symphonies biii
Le gotl de la music sénégalais ❤❤
Wally soy wayati dél am yeurmandé si gnikkoy deuguelou 😂😂❤❤❤❤ ni rck lagn lay bayé
Wally est le meilleur Machaallah ❤❤❤❤
No no no you are star of 🇸🇳 music 🎶 ❤❤❤❤
Li nékhna trop ❤😂
avc wali rek l'héritier de la musique sénégalaise et africaine machalah, kharlene lep lou bakh te rafete si mom 😂, da moun dey machalah
Symphonie bii ohh ❤❤❤❤
Non wally diganiou ray rek 😂liga sol ténala oute si you bary ❤❤❤
Wally mi coumou raye 😢la beugue 🎉❤💗💃💃💃
Taxi love bi momay ray 🎉😢😢❤
Lolou lenen la bilahi❤
Borome keur bi mane nama ray
@@Maguettngom-we4yt ki dina fi ray nit 😂🙆🏿♂️
Nio yam
Wawawa lii néxna wayyy🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Vogue dina meus ame mort dh ❤
Chanteur du peuple 🎉🎉🎉🎉
Wally seck beugue Nala baparè❤❤❤
Wally a vie ❤
Mes li dafa khere ❤❤❤
Eska yenagui degg cheikh gnann guitargui ❤❤❤
The king of the ❤
Ndam rek inchallah 🙏♥️
Bilahi lourass xamoul gâte video snapeur sakh nio gueine lerr aye bossam
Louko nékhe laye def kaye daf gno yape
Bizarrement wally moma eup khalisss mais bilakhi damakoy yereum rekkkk 😢
Wally yalnako yalla takhawou
WALLY tu est le meilleur de tout les temps BIG UP
Waa live taxi love bii vous avez entendu la fin😭😭😭
Wouyy door gueye😂😂😂😂 mais defoul developpement deh😂😂😂😂😂😂
Santeur du peuple ❤❤❤
Ch pas s
Long vie a❤😂toi chanteur du peuple ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤💪👌🙏
Wally 🥰🙏
Wally li mome dafa nekh be eubou 🫶🫶🫶❤️❤️💪💪
Chanteur du peuple
Meilleur ❤️🥇
Machalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ le chanteur du peuple
Lawla thiatte Seck❤❤❤
Werr AK werlé rek Mar 🎉💃💃💃💃
Ms papis ndiaye mi dou nitou dara way😂❤
Yaye sene baye ❤❤❤❤❤
Barki yallah quii moo meuneu way😭❤️
Walll seck❤❤
Ma vie ❤
Rap yi Décembre lay bañ😂❤❤❤ machallah
Pour mane Kasse mako setlou😅😅😅
😂😂😂😂😂😂😂
Meuso déf live bou mélni machala
.je l'aime beaucoup bly yw ❤❤❤😊😊😊 Wally seck me plais beaucoup bly
Mar ya meun mokal maîtriser musique nak❤
Diam si ioe mar yacine 🙏🤲❤️
Kou nagou ni ndiap mbamla rk lalal ❤
My favorite Wally Song Ever: TAXI LOVE 13:10
Awa Banaya gueudj nako guiss deh lou khew🚶🏽♂️
Da dem France ci yayam
Dénck nala bour yalla mou bakh mi
Symphonie moniou bolé ak ioe Mar❤
Macahalla❤
Le meilleur de sa génération Dinama REYYY 😅😂😂❤❤EH WAYE SAMMBAA
Sama nom bii lii nga binde bari na😂😂😂😭
Ya meuun naak😂❤❤🎉
Cette Non ils parlle avec moi yonbanté kô fattê Li kô 12ans si rêneu Gua Dêthie kô sétaneu kô sama pape Wally seck si Game bi teuyê kô Bou bakh bi L'eu Yeugu Lou kô Dékh Lou kô 👂 yalla Tanneu kô mou Doneu chérie Sokhna Aïdara finition bi Lèkh Laxou Xapeu talleu yi xarreu Fasse yî 🐴 Niarry Meuryi xamaneutté Naniou Léwtau Naniou Lou takh niou warra guissê🎉 Jëlli kô ballê keur Gui 🐴 Raxass sa maï Ndapeu 🍽️🔪🔪🔪🥄🍽️😅😅🚦 vert passage à tout Les Artistes jaune relentie à tous les fans rouge stop wlly seck finition bi Les Autre se sont les démarage 🐣🐣🐣🐣🐣🐣🐣🐣
Way li nékh n'a dh❤❤❤❤
Wally je t'aime beaucoup ❤
Nous réclamons tes anciens son
wbs you are the best singuer
Ya. Meune kay mar yacine ❤
Wa Wally nieuweul Amérique nak 😢❤
54:30 papis Ndiaye dou nite kwa 😂❤❤
awou kat bou ndiol bi taille fine bi 🤩moole na
Digua masa danel vogue sounu kaw dhei 😢😂❤
Ki menoul dra 😂😂😂😂😂 oh nékh na🎉❤😂
Goude fan rekk mar
Bilay ndiap Dinama Ray no kiii dafa nekh😂😂
Waly rk lay topeu❤
The king of th WBS le fashion boys de la musique sénégalais l'enfant béni par ses parents walahi yagui deff Lou xéré wong Kong
Mani ana Mbaye Sy ci "wééh fourrr" bi😂
Ndiap
Raynama 😂❤❤
1:38:41 ohhh lînékhna wâye😢😢