Victime de maraboutage ? Aida raconte son histoire "Le marabout m'a dit, votre coépouse vous a…

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 1 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 234

  • @nenebah2169
    @nenebah2169 5 днів тому +13

    Malgré sa souffrance elle est une belle dame machallah qu'Allah apaise son coeur est remplacé son chagrin contre une benediction ya rabb

  • @yvonneflorencebadji2037
    @yvonneflorencebadji2037 7 днів тому +27

    Aye way li metina 😢 j'ai les larmes aux yeux 😢aye way bayiléne khel si li,woudié Sénégal metina 😢

    • @NdayeKebe-e1l
      @NdayeKebe-e1l 6 днів тому

      masta ma Sauer baraga si aye borom 😭😭🤲

    • @amyniass4511
      @amyniass4511 5 днів тому +3

      Mane souma guisé khalŕ yi légui niémé woudié damay diakhal da am nio bone sétougn dra tè woudié diaral nalén louné .mane mom woudié merci rek

  • @maguintd5790
    @maguintd5790 7 днів тому +53

    Ay way set léne Thi yalla Thi liguene di def nit yi li adouna djarou ko leip day diekh Sokhna si yalla ga tanai ak diam 🙏🏿🙏🏿

    • @NdeyeKane-q2u
      @NdeyeKane-q2u 5 днів тому

      Aka wakh deug mane 2 femme la dom bouma am mbou delo sama woudj diakarlo ak mane nema dagay mougn force

  • @OumyKhaiiry
    @OumyKhaiiry 7 днів тому +23

    Aye waye louko fi diar masta Sister vraiment c'est triste bilahi 😭😭😭😭😭😭😭

  • @mameabyfall7092
    @mameabyfall7092 7 днів тому +89

    Aida nitè liguèye la mou diape yalla la nèkhe doumani dou liguèye dè mes fadjiou toubapbi bi tamète thila gnioune senegalais dagnio sagane dakhe parfois bop mèti gniou saganèko dagnio war di fadiou yalla nala yalla takhawou thi barkè Alkhourane ❤️🙏🏾

    • @madeline8547
      @madeline8547 7 днів тому +18

      Deugleu dhe dakh Yalla mo djiokh seytane dolè dico setane baa kerokh yomalkhiyam ! Waye walahi kou geumoul lii dafa fekk ni liguey daloula liguey yougnoula walahi.Yalna Yalla samm gnieup

    • @dabachou5674
      @dabachou5674 6 днів тому

      Vérité Absolue Vraiment Tmt Et Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏 🙏 🙏 ♥️ ​@@madeline8547

    • @SerignemorFall-wp1uk
      @SerignemorFall-wp1uk 6 днів тому

      @@madeline8547bilahi deug la ame na sama bene pa bokham ni lolou moko dale

    • @AidaDiouf-rb9pm
      @AidaDiouf-rb9pm 5 днів тому

      Merci si réponse bi​@@madeline8547

    • @fatimcamara7168
      @fatimcamara7168 День тому

      Khana deg’lou wo ?

  • @FatyNdom-c2n
    @FatyNdom-c2n 6 днів тому +18

    Yalnala yalla may tane banga guissate si barké naby 😢😢😢😢😢

  • @ThioroFall-s8h
    @ThioroFall-s8h 7 днів тому +31

    Ki yobouko hôpital niou traité ko comme dako dabb 😢
    Mogeun boulķo djign kén yalnaleu yalla sameu diapàlé leu baga gissate amin yarabi

  • @EmgBusiness-w3s
    @EmgBusiness-w3s 6 днів тому +22

    Fadél yalna yalla fayla si barki yonnet PSL

  • @ndeyeawasow8998
    @ndeyeawasow8998 7 днів тому +24

    Ohhhhhhh masta waaaye yalla na yalla safara lèpe si barké yonènne tiby seydina mouhamet (saw) ak si barkè alkourane 🙏🏻❤️

  • @ndeyediop335
    @ndeyediop335 7 днів тому +24

    Li kouka topp billahi wallahi wa tallahi dagga dé tè sa dé dou diote khol yépp dagg

  • @MyalastarLDSTV
    @MyalastarLDSTV 2 дні тому +1

    Yallah badina soutoureux Aida massa Yallah mako Yallah tegui merci confrere iow ta it Fadel confrere fouma toll mes prières sont sur vous. Longue vie dans la santé

  • @aidathiam6610
    @aidathiam6610 6 днів тому +6

    Delol lépe ci yalla continuel fadiou yalla bakh na

  • @Mamalamine775meth
    @Mamalamine775meth 6 днів тому +11

    Oh massa yay boye lou lokho deff lokho moune nakko dindi diemal numéro kilifeu you magg yi si reww mi Serigne Abdallah Diouf wallah Serigne you bakh yi si reww mi dall inchallah ❤😊

  • @DiamonoTv-m1f
    @DiamonoTv-m1f 7 днів тому +19

    Allahou Akbar😱😢triste yalna yalla taxawoula🥺🙏🏿

  • @Dada-e3e7j
    @Dada-e3e7j 6 днів тому +12

    Na dem si sg Fallou Rahman douko reuthiou inchaallah

  • @coumbandiaye6923
    @coumbandiaye6923 6 днів тому +12

    Massa. Mais tension occulaire daf koy deff. Yalna yalla delossi weer barakatou Seydina Mouhamed SAW 😮

    • @maremesall9322
      @maremesall9322 6 днів тому +2

      Lou leer wala diabetes aussi dafkay deff bilahi

  • @adjandieyaseckfall6794
    @adjandieyaseckfall6794 7 днів тому +48

    Mane dè seyou woudjé lou si way wakh damakay gueum, doundou na you mèti té woudjou momako tègone

    • @Iboudieng-bu4hv
      @Iboudieng-bu4hv 6 днів тому +3

      li Goor Dako diar

    • @amyniass4511
      @amyniass4511 5 днів тому +1

      ​@@Iboudieng-bu4hvdiarouko déh té am djiguéne you bone mo takh souma guissé ligui nignou gnémé woudié damay tite sax mane mom merci rek

    • @Iboudieng-bu4hv
      @Iboudieng-bu4hv 5 днів тому

      @@amyniass4511 djigen kay Daa Yaga sokhor si moromou djigenam

  • @LoaminaLO
    @LoaminaLO 7 днів тому +15

    Aida yalla nala yallah tegil natou bi si barké Seuydina Mouhamed❤❤❤..

  • @wara2043
    @wara2043 7 днів тому +22

    La polygamie n'est pas pour cette génération d'hommes et de femmes .

    • @MO_CISSÉ
      @MO_CISSÉ 7 днів тому +9

      Trop de vies détruites 😢

  • @serignebarradiouf8335
    @serignebarradiouf8335 6 днів тому +28

    Fatima dieng yi beuri nagn ci keur yi blh😢😢

    • @alassanedieng7479
      @alassanedieng7479 5 днів тому +1

      Bilahi

    • @Awabrescia
      @Awabrescia 5 днів тому +1

      Bilakhi bene fi si Italie boury ndiaye domou khady yague kep kou dieukeureum dokhane babacar fi si brescia mou yakh sa adouna barki alkhourane li

    • @serignebarradiouf8335
      @serignebarradiouf8335 5 днів тому

      @@Awabrescia boléko ak mane ma dokhane ndeyam magui Bergamo Italie

  • @FatouWade-d1u
    @FatouWade-d1u 7 днів тому +11

    yana Yalla safara si barké Seydina Moukhameth (SAW)🙏

  • @Bineta-o3e
    @Bineta-o3e 40 хвилин тому

    Elle est trop belle la dame ndeyyssane nako ya Allah diapalei❤

  • @salvachachasalomon-bs7fg
    @salvachachasalomon-bs7fg 2 дні тому

    Ndéye sane c'est une grande cœur Aïda ngom elle est très gentille liguéy rék lay déf yalnala yalla takhawou 😢😢😢

  • @ElajGueye-nv7su
    @ElajGueye-nv7su 7 днів тому +6

    Tres sensible premiere dame youbouko tunisie.

  • @sokhnandiayeba5606
    @sokhnandiayeba5606 7 днів тому +20

    Djiguéne bourafetebi mashahallah ndeysane

    • @CoumbaSoumbounou-r8n
      @CoumbaSoumbounou-r8n 6 днів тому

      Té diambare aida dou guiss deh wayé ba tey moungui dane doleme Thia patte d'oie 😢

    • @Awabrescia
      @Awabrescia 5 днів тому

      Bilakhi ki ko def li moy genre bene fi si Italie boury ndiaye domou khady yague kep kou dieukeureum dokhane babacar fi si brescia mou yakh sa adouna barki alkhourane

  • @madjiguenesow3621
    @madjiguenesow3621 6 днів тому +8

    Massa Aïda liguey meune na nek mais pour cas bi meune na nek un probème lié au cerveau parceque les différents nerfs sont liés j ai vu des cas pareils ça arrive à des stars qui ont perdu une moitié de vue ou total yalla na la borome may ngua guissate inchaallah

    • @aliniang7452
      @aliniang7452 3 дні тому

      Loumana nekla wayé nioune lepou serigne

  • @IbrahimaKebe-p4y
    @IbrahimaKebe-p4y 6 днів тому +5

    😭non magui ndioy billahi thiay yalla ay way Sénégal yakouna😭

  • @NdeyeThiam-ws6ti
    @NdeyeThiam-ws6ti 7 днів тому +6

    Sokhnassi demal thie serigne fallou rahmane

  • @bintoudjiba759
    @bintoudjiba759 4 дні тому

    Une femme courageuse et belle machallah qu'allah nous protège et nous guide dans le droit chemin amine

  • @aissatoungom9833
    @aissatoungom9833 10 годин тому

    Yalla nala yalla téguile natou bi métina woudié bakhoule bilahi kham na ci dara korte😢😢😢😢

  • @maimounatall-mn1vh
    @maimounatall-mn1vh 7 днів тому +9

    As salamou aleykoum. C'est haram d'aller voir un marabout et de croire ce qu'il dit et cela te sort même de l'islam.A moins que ce soit la personne qui t'a supposé mbarabouté qui te l'avoue, tu n'as pas le droit de l'accuser ou d'avoir des doutes à son sujet.Le marabout dont on parle ici est un mécrécrant et la prière de consultation al istikhar doit être faite par la personne qui souhaite être éclairée et pas par une tiers personne sinon cela n'est pas légiféré.Aussi,il est interdit de donner la main ou de toucher une femme étrangère c'est à dire que tu peux épouser.

    • @gracevie6343
      @gracevie6343 День тому

      C'est vrai, seetkati yakk nagn deukeubi. Cependant, il y'a des faits qui font douter de certaines personnes. Je ne sais pas ses doutes sont haram, mais aller voir des marabouts, c'est haram.

  • @ndeyediop335
    @ndeyediop335 7 днів тому +27

    Est-ce que dou Tension bou wathié si saay beute doto guiss

  • @AdjidabaTop
    @AdjidabaTop 6 днів тому +3

    Ayy wayy fumu dieum kouco kham nagniu co wah, li métina tropp nah seuy diatnaco, bania bok dieukeur rék, ayy Gör diaruco, niati fanou bambéle dama yakarni nite duco bayi khél sa sou yéwo té khamo kagne la fane la ak nakala, nagniu délo si khél yi yalla bour bi Dara tewouco, sokhna si yalla nala yalla takhawu😢takhawu sa ndjabote bubah ga wér ak jam

  • @SarrMay-b2f
    @SarrMay-b2f 6 днів тому +2

    Masta yalla mi Dara teuwoul yalla na la borom bi téguil natou borom bi same la yow ak saa djabote yalla na léne borom bi barkel amine ya rabbi 🙏

  • @ibrahimandior428
    @ibrahimandior428 6 днів тому +3

    Alakhira di dina méti trop lini nga def ko nitt té yalla nitt la wakh né mola gueuna beugue té adouna yagoul😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @PapiPapi-z6d
    @PapiPapi-z6d 7 днів тому +15

    Boul djigne kéne gueumeul sunu borom rek dina bakh

  • @aitangom5063
    @aitangom5063 6 днів тому +2

    Yalnala sounou borom teguil natou bi metina 😢😢😢

  • @veroniquenatack7392
    @veroniquenatack7392 7 днів тому +3

    *Massa métina trop way..Yalla nala sougnou Borom wéral bagua meuneu diapalé say ndiaboot 😢🙏🏽🙏🏽🙏🏽*

  • @YacineDieng-hc5mw
    @YacineDieng-hc5mw 3 дні тому +1

    Adouna diaroul def lou bone yalnala yalla diapalé thi barké mouhamed

  • @NdeyefatouMbodji-s2w
    @NdeyefatouMbodji-s2w День тому

    Yallah nala yallah nital say beut yallah nala yallah delo say beut si Barki yonenty bi inchallah

  • @gracevie6343
    @gracevie6343 День тому

    Serigne yiii mooome meuytoulene lene.
    Ya ALLAH rek moo hammm.

  • @ousmanelo9378
    @ousmanelo9378 7 днів тому +16

    Est-ce que dou fébarou Hospital tamite… cheuuuu YALA rek mo xam

    • @LiLyg68
      @LiLyg68 7 днів тому +6

      Vraiment. Yahllah na ko yallah weral mais des fois ces des maladie. On ‘a tendance a tout attribue au mystique

    • @Gggge_dudiolof9536
      @Gggge_dudiolof9536 7 днів тому +1

      Serigne meune na lounek, cas bou melni guiss nako

    • @aidambacke6273
      @aidambacke6273 7 днів тому +1

      Tension tamitt mounako deff dée !! yalla n'a yalla safaral leep

  • @AlimaSamb-xw6gd
    @AlimaSamb-xw6gd 6 днів тому +1

    Massa ma chérie yallah nako borombi safara

  • @FatouSow-i8i
    @FatouSow-i8i 4 дні тому

    Aïda yalla nala yalla taxawou boléla ak koula diapalé bangua délou watt ci sa sago ci barker seydina mouhamed psl

  • @MamySalk
    @MamySalk 7 днів тому +2

    Aye waye li métina li louko fi diar la camoul😢😢 yalla nala yalla sam masta😢😢

  • @aidadiop5312
    @aidadiop5312 7 днів тому +4

    Mani na liguéye bi délou wat thia gnome inchallah aida yonéma sa numéro

  • @BabacarMbaye-f3u
    @BabacarMbaye-f3u 7 днів тому +12

    Tieuy gaur...encore gaur toujours gaur.

  • @darkchokolate8040
    @darkchokolate8040 6 днів тому +1

    Bayiko ak yallah mom ak sa djekeur yalna lene yallah mbougal😭😭😭😭😭

  • @LazoDiallo-k4c
    @LazoDiallo-k4c 7 днів тому +4

    Bon rétablissement tante sa fais très mal au cœur

  • @kinouska2260
    @kinouska2260 7 днів тому +5

    Li dou liguey tension occulaire la Sokhnasi

  • @demefalldiop2361
    @demefalldiop2361 3 дні тому

    Yeureum naala déh waayé nammaatal sak gueum yalla ☝🏼 koudoul yalla meunta tégué tousss

  • @PAPAIBANIANG
    @PAPAIBANIANG 3 дні тому

    😢😭Tout çava changer inechallah ❤

  • @senzanome9931
    @senzanome9931 7 днів тому +7

    Guemeul nii say beut dina weer nakh sa yaye sa serigne laaa guemeul niii digua guissat

  • @thiernoseck8365
    @thiernoseck8365 7 днів тому +1

    Sénégal dé Bari Wut Ay joulit Lü Banne rekk lañ Xam

  • @fatimadiop96
    @fatimadiop96 4 дні тому +2

    Lii reek Mo takhe ma ragalle seuyate oh massa ma belle 😢😢😢😢

    • @IbrahimaNdiaye-s7p
      @IbrahimaNdiaye-s7p 4 дні тому

      Deete waay sokhna si

    • @Menz2302
      @Menz2302 День тому

      Dinkal sa bopp yallah dem seuyi seuy jammu yallah leu c juste un conseil

  • @OusmaneSyllaSylla-z1t
    @OusmaneSyllaSylla-z1t 7 днів тому +11

    S'il est été un bon marabout Ils vont te donner un nom c'est n'importe quoi demander Allah ce lui le solution c'est de faux marabout manipulateur

  • @Ramapoulo
    @Ramapoulo 2 дні тому

    Courage maman😢❤

  • @غلامالخليفةآبوبكرسه

    Nay san 😢😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @fatousane9443
    @fatousane9443 7 днів тому +8

    Gor diana yakeu sa moromou djiguen? Nagniou ragal Yalla! Woudié gui légui dafa doywar.

  • @papegeuye-fh9ut
    @papegeuye-fh9ut 6 днів тому +1

    Limaci khame dé Mane sa djieukeur bobou diame deuguela loumala khéwe waronena khole môme bimou fébaré natoula yalla nako yalla tégui

  • @thiernoseck8365
    @thiernoseck8365 7 днів тому +9

    Sèt kat nak Bari na ñu xamut Dara nak Aka bari ñu Mana fenn dañuy diaxa se xél mi

  • @eva-gz5qf
    @eva-gz5qf 6 днів тому +3

    Que dieu te d aide maman

  • @AliouBa-ox7wz
    @AliouBa-ox7wz 5 днів тому

    aida ngom diga guiss bousobe yalla yalla nelawoul yalla bahna

  • @dieynababaradji8526
    @dieynababaradji8526 2 дні тому

    Du courage ma chérie

  • @Gkcdshndsncs
    @Gkcdshndsncs 6 днів тому +2

    Senegal mom ba tak fa diabar worna😮😮😢😢😢😢😢😢😢😢😢

    • @oumardieye6550
      @oumardieye6550 5 днів тому

      Ah doyna War dh😂

    • @Ramapoulo
      @Ramapoulo 2 дні тому

      Tout le monde ne sont pas les mêmes😮

  • @Nafidramè-r7b
    @Nafidramè-r7b 4 дні тому

    Massa,yalla na yalla tèguil la natoubi

  • @Madamemmedia
    @Madamemmedia 6 днів тому +3

    𝐀𝐲 𝐲𝐚𝐥𝐥𝐚 𝐧𝐚𝐠𝐧𝐨𝐮𝐬𝐨𝐫𝐚𝐥𝐞𝐫 𝐛𝐚𝐦𝐞𝐥 𝐚𝐲 𝐚𝐝𝐨𝐮𝐧𝐚 😢😢

  • @senemadjiguene6248
    @senemadjiguene6248 5 днів тому

    Yalnala yallah defal weer

  • @AmdiMbacke-i7v
    @AmdiMbacke-i7v 4 дні тому

    Tention leu, Serigne yi daniouy nakhé rék di lékeu khalissou nite yi.
    Yallah na Yallah mayla tawfékh banga guisate

  • @gueyecheikh4878
    @gueyecheikh4878 7 днів тому +2

    Ndaysane metina dei😢😢

  • @FarmaFaye-gw3ei
    @FarmaFaye-gw3ei 5 днів тому

    Yalla nalla yalla maye weur

  • @CherifMbodj-w4s
    @CherifMbodj-w4s 3 дні тому

    Assalamou aleykoum niogui ziar lou weer la soxna si wakh daniouy ligueyanter goudi AK beuthieuk nioune khamnaniou si Dara

  • @toutoumbaya3304
    @toutoumbaya3304 5 днів тому

    Encore une fois goor gui ni dé amoul kersa si daw bayila
    Yalla nala yalla takhawou weral la

  • @bintoudiop9217
    @bintoudiop9217 6 днів тому +2

    Ma sœur a eu ce problème, mais c'est une tension oculaire

  • @LazoDiallo-k4c
    @LazoDiallo-k4c 7 днів тому +4

    Allah ya Rahmane

  • @duchessedjolof2049
    @duchessedjolof2049 6 днів тому +2

    Bayiléne woudié Bayiléne woudié Bayiléne woudié bou pétrin amé goor dawla

    • @amyniass4511
      @amyniass4511 5 днів тому

      Guisga la plus part mm chose loula dal niou daw sén responsablité

  • @aissatoudiop5256
    @aissatoudiop5256 7 днів тому

    Yalla nala yalla saafara.soudé nitt moolako tekk il ou elle va le regretter amèrement. Soudé nitt kou bonn la

  • @DpDp-xe5zj
    @DpDp-xe5zj 6 днів тому

    Senegalais yi niooy eupeu Safar 😢😢

  • @SireSane-c9y
    @SireSane-c9y 6 днів тому

    Massa way courage que dieu t'aide

  • @ousmanediop4110
    @ousmanediop4110 6 днів тому

    Bon rétablissement amineee YARABI

  • @PapemagatteDiouf
    @PapemagatteDiouf 4 дні тому

    Goor diaroul lii 😢😢😢

  • @aidathiam6610
    @aidathiam6610 6 днів тому

    Metina yalna yalla safara

  • @lamienolamister7929
    @lamienolamister7929 7 днів тому

    Adouna Dou keur 😢
    Set len si Yallah 😢

  • @ousmanendiayendiaye8448
    @ousmanendiayendiaye8448 6 днів тому

    Yaala nako yaala defal tawfekh si barkai mouhamed s a w ak mbolaime dioulite

  • @ndiayemaleye2581
    @ndiayemaleye2581 6 днів тому

    Thieuy fadame aka rafete xole❤

  • @MadjigueneNdoye-ep4vh
    @MadjigueneNdoye-ep4vh 6 днів тому +4

    Li maau waalh reek nioune djiguene da gnio waara yeewou goor dou projet

    • @toutoumbaya3304
      @toutoumbaya3304 5 днів тому

      Walahi goor amoul koleuré thi gnimalo sagna wakh metina ndeysan

  • @ibrahimandong6723
    @ibrahimandong6723 6 днів тому

    Yalla nala yalla délola say beute

  • @khadijadia6740
    @khadijadia6740 5 днів тому

    Ndeysane métina😢😰

  • @OumarNdiaye-lr8el
    @OumarNdiaye-lr8el 6 днів тому

    Massa aida yalla ngua weur si barki mouhamad

  • @anicetdiompy7265
    @anicetdiompy7265 5 днів тому +1

    L'homme et ses demons , l'homme est mechant ...😢😢

  • @imamnassythioune4933
    @imamnassythioune4933 5 днів тому

    Dieu est grand ❤❤❤❤❤❤

  • @FaSonko
    @FaSonko 7 днів тому +1

    Hoo lou meti yag na😢😢

  • @MamadouFaye-w5k
    @MamadouFaye-w5k 7 днів тому +5

    Djiguéne yo kholate léne séne takhawaye

  • @aidathiam6610
    @aidathiam6610 6 днів тому

    Yalnala sa gnanou yaye walou

  • @duchessedjolof2049
    @duchessedjolof2049 6 днів тому

    Polygamie ces pas pour nous les africains telment ont est méchant goorou nitte kou nioul bakhoul bou done toubab dou le abandonné jamais au plus grand jamais enplus elle est très belle cette Damme aussi dou si djeukerou diambour yeup légnouye dougou

  • @AwaDiop-r9f
    @AwaDiop-r9f 7 днів тому +1

    Massa😢😢

  • @GnimaDièdhiou-x6y
    @GnimaDièdhiou-x6y 4 дні тому

    Massa ma chèrie 😭😭😭😭

  • @khadydiop8608
    @khadydiop8608 7 днів тому

    Yalla nala yalla diapale

  • @ndeyemaremeseck5154
    @ndeyemaremeseck5154 7 днів тому

    Thieuy Sénégal 😢😢

  • @fatoubah2850
    @fatoubah2850 7 днів тому +2

    😢😢😢 triste