Sama jour tabaski 2021 lama fatali sama dome bou ame 20ans gaz lak ko ma weure hôpital yi finalement cto la amè réanimation ba jour tamxarite mou sogga décédé mais il me disait chaque jour maman magui tak tellement lak dafa méti khole lay diape qu'il repose en paix 😭
Quand une femme mariée commence à faire des signes de fatigue et des énervement sans cesse dans le ménage, libérer là jusqu'à ce qu'elle revienne en de meilleurs sentiments.
Oui frère il y a des hommes qui ne veulent jamais divorcer.. Soit par faiblesse ( excès d'amour ) soit par orgueil auprès du voisinage. Moi jai divorcé 2 fois. Ouais. Dès que les disputes deviennent frequentes, je te libère doucement et gentiment. J'ai enfin trouvé la femme " ideale" Machallah. Priez pour moi
Lou leer nga wax . Le malheur c'est qu'à chaque fois on se dit qu'avec le temps la personne va changer . Hommes comme femmesde nos jours il est difficile de trouver le partner idéal .
@@jamesmarcusbass2999 Parfois frère io y a des habitudes qui ne changent pas. Prends l'exemple sur nos chefs religieux.. pour jn oui ou pour un non , ils divorcent..et la vie continue
Qu'il repose en paix Mamadou🙏.. il y a trop de zones d'ombres dans cette histoire . Mais parlons de nos hôpitaux. Tous les brûlés de 3eme degré meurent toujours dans ce pays. A t_on des structures pour soigner les grands brûlés ? Je ne le pense pas. Le gouvernement se trompe de priorité. Mieux vaut moderniser nos hôpitaux que de construire des terrains de foot et des arènes de lutte au prix de centaines de milliards .Nianou mako Yallah wayé chacun peut être un grand brûlé un jour... Surtout nous les hommes qui dormons avec des femmes qui nous cacheront toujours leur vraie nature... Subbanallah
@@sokhnadiongue4410 yalaa nako Yallah Yeureum.. au debut de ton récit je pensais que tu parlais de la femme de notre ex prof d'anglais à Diourbel dont la femme est décédée dans des conditions similaires que ta maman !!! Que Dieu les accueille tous et toutes au Paradis éternel.
@@sensenmaths6114 quelque soit ce qui sais passè, cest pas une raison des tuer, et si tu ecoute les aveux que le defun a confier a son petit frère avant de mourir, cest la femme qui la trompè avec un autres gars dans le même quartier. Donc meuno togne sa dieukeur ba parè ray ko. Le mari la clairement pointè avant de rendre l'âme donc k justice soit faite et sèverement. Rèecoute bien ce k le frère explique, tu saura que ya pas d'autre version a ècoutè. Tout les èlement sont reunie et cest tres claire. Cest a la justice de faire sont travail.
Mane limeu comprendroul moy bi moula nei dafa taal briquet bi lokho yi takk, apres? Dafa teudi wat??? En tout cas ya des zones d’ombres tei mangui leine di digueul yene gneup famille kou goor ki ak kou jigeen ki ngeen ragal yalla! Tiim ngene ki lakk ki ba guiss ko mou done lou metti lolou sakh(yalla na gnou oump tei oump mbolem joullit) lakk lou metti leu tei loumou metti metti safara mo ko gueuneu metti téméri yone: donc lou nitt jeppi moromam bou ko dara takh mou koy toumal loumou defoul teyit lou la nitt nekh boumou takh nga koy faral ci loudoul deug! Ndakh safara doi ay thiakhane! Yalla nagnou maye mou oump gnou té oumpou mbollem joullit! Tei yalla nagnou khiir ci deug ak deuggou ala koulli haal!
Metina trop damasa rousse en tant que djigene.volence bakhoul si seye (dakarbuzz sen journaliste bi machala elle est professionnelle et posée et c est la 2eme fois que je vous le dit
En tt cas doyna warr en 4 jours il avait la possibilité d'éclairer sa famille sur ce qui s'est réellement passé... c'est le moment des règlements de compte donc faut être très prudent et laisser la justice faire son travail.,...repose en paix Mamadou yalla nanga yegalé sa ndaw Firdawsi
@@awafall2349 moi on essaie de me tuer sincèrement à la première heure c'est ce que je dis à ma famille..dés que j'arrive à parler je révèle tout ..walae métina nak mais d'abord il dit qu'il s'est brûler en fumant et après il di que c'est sa femme...pourkoi il essaierai de couvrir sa femm ..ce serait dans quel intérêt...sincèrement que justice soit faite dal
yalla na ko yalla yeureum te kare ko aldiana firdawsi si barke seydina Mohamed sala lahou Ali Mohamed sala lahou Ali Mohamed sala lahou Ali Mohamed sala lahou Ali Mohamed sala lahou Ali Mohamed sala
À vrai dire ki limou fi wax yeup c’est contradictoire té bobou batay magam waxouko niko djabar dji moko lak . De toute façon Yalla rk mo xam fi deugu bi fété naniou bayi yone mou deff ligueyam dall . Yalnako Yalla yeureum xaré ko aldiana inchallah
Yalla na niou yalla mouseul si diegnen bou bonne aminata mi ak yayam niou bonne laniou waye kou reyy nite doto nekh nite mamadou yalla na ko yalla yereum kharè aldiana firrdawsi
D’apres le meilleur ami du defunt il a laissé sa famille a cause de sa femme motakh wakhou kilifa ken douko tegui yalnako yalla yeureum t kharei ko aljanay firdawsi
Je compatis vraiment a votre douleur mais il faut faire tres attention. La victime ne vous a jamais dit que c'est son epouse qui l'a immole et pourtant il a beaucoup discuter avec les membres de la famille. Si seulement s'etait sa femme il vous l'aurez dit. Il faut prier pour lui pour que Dieu l'accueille au paradis inchalah. La police fera son travail.
@@msy8317 j'ai ecoute religieusement son frere mais il n'a jamais dit que la victime lui avait dit que c'etait sa femme la responsable de son etat. Ce qui m'etonne le plus c'est pendant quatre (4) jours d'hospitalisation, il n'a jamais dit que la femme l'avait brule alors qu'il discutait avec sa famille tout en etant conscient.
Yeine famille kou goor guiii yeine yeina amoul droit si mom ndax vous l'avez rejeté,,wa keur amineta gno hébergé mame mor,,oui nitt Dina kharou Di sauver bopam ndax douleur bi ladoul meuneu supporte,,
@@thiamnogaye9807 personnellement Mane gni lé conné pa youtube rkk lako djissé..mais tamitt ki rakam bi nimouy wahé si famille kou djiguènn ki ak Koy djiguene ki c reste à voir ..n'a nice touti ba enquête bi parè au moins ils ont accueilli leur fils kan il été dans le besoin
@@thiamnogaye9807 et en parlant de nitt Dina kharou Di sauver bopam Lolou mom c vraie..et je dis pa k pa mor da kharou Lolou Dara waroumasi j'attend l'enquête comme gneup
Li amoul sakh ma dém té nieuw c la femme qui est à l'origine de tout. (Sama soeur woona sama yaye néko tankam dafa daam thi escalier la daanou Mane gueumone naco au début mais bimou dougoussé djieukeur dji indi co niom niaare sene comportement la khamni danio khékh dieukeur dji guagne co. Après damaco lathie insisté Mouy soga wakh deugue wa keur gui). Parenthèse la wone. Limay conseillé famille ba Moy nagnou topou cas bi.
Avec les deux versions que j ai vus personelment la femme n as pas faits les acres qu on la renonce je pense que le gars a oublie d eteindre le megot de cigarette et ce que a produit le malheur.je parle en connaissance de cause sincerament. C est Mon point de vu
⛔️ Aywaay bayi lène yakhanté bi. Lii accident rék la té lolou la justice di conclure. La famille de l'homme voulait mou takk sène mbokk motakh gnagass gnagass ame ci diganté gnaari familles yi. Mais kéne rayoul kéne kharouwoul. Pétrole mo nékone ci chambre bi pour dakh matt yi ak khétou sawou khalé yi. Le mari s'est lavé les mains avec pour dindi huile bi takhone ci lokho yi. Wakh nguène fi ay garabou yo ak ay cigarette té lolou lépp andoul ak pétrole. La femme croit que le mari s'est suicidé ndakh dafko done menacer, la famille du mari défend l'image de leur défunt fils en accusant la femme ndakh dagnou done histoire juste avant. Soupçons yi commencer ak mauvaise interprétations yi (en commençant par celles du petit frère). Gnaari familles yeupa baakh et ça se voit. Massa et pensez aux enfants svp.
Famille diabar qui décédé tmt louche nagn niom dall lou waay wakh rk amnagn tontou ba paré Yalna yalla atté si yeurmandéw té diégeul ko té fenial ki df liih
En tout cas moytou l'en toumala nit.nénga ci camotte bi la femme bi tek pétrole bi,domam neko papa sa lokho bi takk n'a pétrole,mom la victime ci bopam né mo Tal briquet lokho bi lakk si j'ai bien compris,une tante à la femme dit que li lep tokh moko ko yobé...pour man femme bi dafa tek pétrole bi fou wadji teud mou tourou,lokhom toy ci Mouy tokh par maladroit lakk bomap daw ci canal bi Di sauver bopam,diabar dji fokni dadone kharou .peut être lolou la beugone expliquer freram bi bimou nan kouy kharou d'où sauver bopam pas pour accuser sa femme.yalla réka kham nak.que son âme repose en paix
Sou fékkon yéré yi amna pétrol peut être mou lak ko lakk mou metti mé lokho yi késsé mou tall cigarette pour tokh mou lak yaram yeup lolou noumou meuna nékké je sais pas la vérité nakk mé c trop bizarre
Wa dolén wakh si hôpital sénégal yi li tmt niawna trop yalla nako yalla yeureume si barki seydina Mohamed😭😭😭
Sama jour tabaski 2021 lama fatali sama dome bou ame 20ans gaz lak ko ma weure hôpital yi finalement cto la amè réanimation ba jour tamxarite mou sogga décédé mais il me disait chaque jour maman magui tak tellement lak dafa méti khole lay diape qu'il repose en paix 😭
Que son âme repose en paix ndeyssan c'est dure yala mayla kholou mougn
Que la terre lui soit légère vraiment métina😭😭
Yallah nako yallah yeureum♥️🙏
Paix à son âme
Paix en son ame🙏🏾
Quand une femme mariée commence à faire des signes de fatigue et des énervement sans cesse dans le ménage, libérer là jusqu'à ce qu'elle revienne en de meilleurs sentiments.
Oui frère il y a des hommes qui ne veulent jamais divorcer.. Soit par faiblesse ( excès d'amour ) soit par orgueil auprès du voisinage. Moi jai divorcé 2 fois. Ouais. Dès que les disputes deviennent frequentes, je te libère doucement et gentiment. J'ai enfin trouvé la femme " ideale" Machallah. Priez pour moi
@@moustaphafall9310 des fois ce n'est même nécessaire de divorcer. qu'elle retourne chez ses parents le moment que tout se tasse
Lou leer nga wax . Le malheur c'est qu'à chaque fois on se dit qu'avec le temps la personne va changer . Hommes comme femmesde nos jours il est difficile de trouver le partner idéal .
@@jamesmarcusbass2999 Parfois frère io y a des habitudes qui ne changent pas. Prends l'exemple sur nos chefs religieux.. pour jn oui ou pour un non , ils divorcent..et la vie continue
@@jamesmarcusbass2999
Un
Qu'il repose en paix Mamadou🙏.. il y a trop de zones d'ombres dans cette histoire . Mais parlons de nos hôpitaux. Tous les brûlés de 3eme degré meurent toujours dans ce pays. A t_on des structures pour soigner les grands brûlés ? Je ne le pense pas. Le gouvernement se trompe de priorité. Mieux vaut moderniser nos hôpitaux que de construire des terrains de foot et des arènes de lutte au prix de centaines de milliards .Nianou mako Yallah wayé chacun peut être un grand brûlé un jour... Surtout nous les hommes qui dormons avec des femmes qui nous cacheront toujours leur vraie nature... Subbanallah
Ndeysanne il est meurtri le frère
Bilay ma mère en est la preuve dafa sone defar ndeki mou brûlé def principal une semaine décédée
@@sokhnadiongue4410 yalaa nako Yallah Yeureum.. au debut de ton récit je pensais que tu parlais de la femme de notre ex prof d'anglais à Diourbel dont la femme est décédée dans des conditions similaires que ta maman !!! Que Dieu les accueille tous et toutes au Paradis éternel.
@@astoudiouf8246 wallayi!!!
Bonsoir Moustapha,
Vous pouvez m'expliquer ce qui s'est passé svp? Car je ne maîtrise pas bien le Wolof. Merci
Massa le frére junior li metina trop bilahi yalla nako yalla yeureum té kharé Aldiana😭😭😭😭😭
Paix à son âme 🙏😭 djigene bou bone yalnaniou si yalla mouseul Amineta daw meurtrière nga sorcière nga bête nga sauvage nga imbéciles nga
C'est tellement dur😭😭😭😭
Très dur elle est méchante
bayilen ba ame ci loulen lerrr
Diabar djii mome saltei neu dei neike bo kham nii aye mateu xeigne sawww lou nei thiammmm mamadou yalla nako yalla yeureume tei xarei ko aldiana
Hum pourtant c'est elle qui hébergeait son mari!
Khana ci famille weuyou la dougou vraiment femme Boon na😭😭 yalla nako yalla yeureum té kharé ko aldiana firdawsy yalla na dée di 😭😭
Nn mm pad
Mm pas
Khana yaw yaye domarame yalna yallah leral lép mais yala bakhna
La femme Sénégalaise rek est violente
@@juniorjunior1345 wakh deye rafeite
Yalna Yalla yéréme ko ndéssane
Djigène bou bone bakhoul, k justice soit faite. Li dafa yomb, cette femme vraiment damaram leu mom ak yayam yeup nioko ray
ATTENTION tu. N'a pas la version de la femme hain
@@sensenmaths6114 quelque soit ce qui sais passè, cest pas une raison des tuer, et si tu ecoute les aveux que le defun a confier a son petit frère avant de mourir, cest la femme qui la trompè avec un autres gars dans le même quartier. Donc meuno togne sa dieukeur ba parè ray ko. Le mari la clairement pointè avant de rendre l'âme donc k justice soit faite et sèverement. Rèecoute bien ce k le frère explique, tu saura que ya pas d'autre version a ècoutè. Tout les èlement sont reunie et cest tres claire. Cest a la justice de faire sont travail.
@@khadyndour2230 merci sokhnasi c trop louche nit dou xarou ba paré beug sauvé bopam
@@sensenmaths6114 Baneu version
Bilay Bone rekk🤔🤔🤔🤔🤔
Paix à son âme métina lole way yalla rek mo khame li khewone si nekk bi
Il faut donner cette bouteille à une expert médico légale pour une analyse plus approfondie
Merci pour analis bi.
Surtout lolu meuna leeral mbirmii
Afaire yi loussna thi coté gnari famille yeupp😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Li gueuna meti Sénégal nek ci etat d’urgence di woor hôpital ayy heur c’est grave
Très grave
Paix à son âme que firdawsi soit son deumeur éternel amine yarabi
Amine@@ouryba1446
RAGAL LÈN YALLA swt ☝ TAY WAKH LOU LÈN WOUR TÈ MANOU
Mane limeu comprendroul moy bi moula nei dafa taal briquet bi lokho yi takk, apres? Dafa teudi wat??? En tout cas ya des zones d’ombres tei mangui leine di digueul yene gneup famille kou goor ki ak kou jigeen ki ngeen ragal yalla! Tiim ngene ki lakk ki ba guiss ko mou done lou metti lolou sakh(yalla na gnou oump tei oump mbolem joullit) lakk lou metti leu tei loumou metti metti safara mo ko gueuneu metti téméri yone: donc lou nitt jeppi moromam bou ko dara takh mou koy toumal loumou defoul teyit lou la nitt nekh boumou takh nga koy faral ci loudoul deug! Ndakh safara doi ay thiakhane! Yalla nagnou maye mou oump gnou té oumpou mbollem joullit! Tei yalla nagnou khiir ci deug ak deuggou ala koulli haal!
Amine♥️😭😭🙏
Sénégal daguay febar de dofadiou
Thieyyy yallah Man deh waronne.
Que firdawsi soit ta demeure éternelle frère🙏🙏
Ndeysann aduna d'où Dara 🙏 k firdawsi soit sa demeure éternelle 😭😭🙏🙏🙏 Amine Amine Amine Amine
Ndayssane li métina trop courage frère yalna sougnou borom léral lep🙏
Allahouma ihfirlâho warhamhô ci barkè yonent bi psl amine
Metina trop damasa rousse en tant que djigene.volence bakhoul si seye (dakarbuzz sen journaliste bi machala elle est professionnelle et posée et c est la 2eme fois que je vous le dit
Hamo len lou hew dé bahna
Hamo len lou hew dé bahna
Massa mes condoléances à toute la famille li metina trop 😭 yalnako yalla yereum khareko adjana thionom yem fi si adina 🙏🏾
Voilà un frère exemplaire 🙏🏿
Qu'il repose en paix...
Une pensée à ses deux jeunes enfants qui vont devoir grandir sans leur père.
Ĺ
Mbene ndananela am yar fonk nieup rawatina wa tivaouane mane damako beugue thi sama xol ❤❤❤❤❤❤❤
Tu es courageux bro yalla nako sunu borom xare aldiana🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
En tt cas doyna warr en 4 jours il avait la possibilité d'éclairer sa famille sur ce qui s'est réellement passé... c'est le moment des règlements de compte donc faut être très prudent et laisser la justice faire son travail.,...repose en paix Mamadou yalla nanga yegalé sa ndaw Firdawsi
J'avoue que c'est louche vraiment nagn si def nakeu té bayi yoon def liguéyeum
@@aidacissa63 effectivement les explications sont désordonnées, qu'il repose en paix mais des explications claires incombaient le défunt
Si réellement la femme l’avait brûlé il l’aurai dit depuis son réveil vraiment c’est louche
@@awafall2349 moi on essaie de me tuer sincèrement à la première heure c'est ce que je dis à ma famille..dés que j'arrive à parler je révèle tout ..walae métina nak mais d'abord il dit qu'il s'est brûler en fumant et après il di que c'est sa femme...pourkoi il essaierai de couvrir sa femm ..ce serait dans quel intérêt...sincèrement que justice soit faite dal
Vraiment c triste mai nagnou moytou di abandonné sougnou keur waydiour yii dakh djiguene daray adouna diarouko qu'il repose en paix
Nit boulay dougeul aljannah wallahi diarna tarbiyou beu soneuh djiguén bou bone moussiba là thi keur
yalla nako sunu borom yeureum té diégueule kharré ko sa Aldjana firdawsy
yalla na ko yalla yeureum te kare ko aldiana firdawsi si barke seydina Mohamed sala lahou Ali Mohamed sala lahou Ali Mohamed sala lahou Ali Mohamed sala lahou Ali Mohamed sala lahou Ali Mohamed sala
Faite très attention es que femme bi moko tal yalla rek mo kham yalnako yalla yeureum té kharéko aldiana
Surtout soudon moko tall kou goor gui dina wakh ndakh meunon na wakh ndakh frère bi nena kou goor ki nouyou nako mou faye ko
@@rokhayatine6510 affaire bi lou diara téye la
Bilaye teyilene mo yalla nako yalla yeureume réanimation kene doufa doug
Vue que y avait la présence des enfants , naniou interroger khaleiyi, un enfant ne sait pas mentir.
Yalla nako yalla kharei Aldiana you guene kawéi 🙏🏾
Amine 😭😭
C'est vraiment dur ki dou djiguene diou bax k justice soit faite yalnako yalla yeureum et kil veille sur ses enfants🤲🤲😭
À vrai dire ki limou fi wax yeup c’est contradictoire té bobou batay magam waxouko niko djabar dji moko lak . De toute façon Yalla rk mo xam fi deugu bi fété naniou bayi yone mou deff ligueyam dall . Yalnako Yalla yeureum xaré ko aldiana inchallah
Ah lepe diabare dji la
Yalla na niou yalla mouseul si diegnen bou bonne aminata mi ak yayam niou bonne laniou waye kou reyy nite doto nekh nite mamadou yalla na ko yalla yereum kharè aldiana firrdawsi
Le comportement du père aussi ne laisse perplexe
On dirait qu’il ne s’entendait pas bien avec son fils d’après mon analyse
C’est ce que je me suis dit …niakk na kersa lol sakhh sa dom dafa lakk guaniii nagniou teud ba soubeu doyna war dal
D’apres le meilleur ami du defunt il a laissé sa famille a cause de sa femme motakh wakhou kilifa ken douko tegui yalnako yalla yeureum t kharei ko aljanay firdawsi
esk li doomm bi nek si keur diabar bi moo takh
La famille n’était pas pour le mariage
Li come mbougal 1960 ba legui meunouniou fadiou dangay nekeu si dound ak déhh nioulay xolni sa roukh di dem pitié Afrique
Djiguene bou vulgaire baxoul ak di menace ay regret rk mo siy top
Il est brave plus responsible meme que son pere set 👏 un frere
Que son âme repose en paix
Paix à son âme Ndeysane 🤦♀️😭😭😭😭
Boy bi kou dall la te am conscience trankil
Billay dafa am xél
Ndeyssane metina Nitti kobone yallna nusi yalla mossal diabar dio bon
Amine
goor nii laY mél 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 Yalla Nako yalla yereme 😭😭😭
Je compatis vraiment a votre douleur mais il faut faire tres attention. La victime ne vous a jamais dit que c'est son epouse qui l'a immole et pourtant il a beaucoup discuter avec les membres de la famille. Si seulement s'etait sa femme il vous l'aurez dit. Il faut prier pour lui pour que Dieu l'accueille au paradis inchalah. La police fera son travail.
Ils ont dit kil l'a dit à son frère
@@msy8317 j'ai ecoute religieusement son frere mais il n'a jamais dit que la victime lui avait dit que c'etait sa femme la responsable de son etat. Ce qui m'etonne le plus c'est pendant quatre (4) jours d'hospitalisation, il n'a jamais dit que la femme l'avait brule alors qu'il discutait avec sa famille tout en etant conscient.
@@rokhayadiop1461 merci 🙏
@@rokhayatine6510 je vous en prie! Je ne fais qu'analyser les propos de la famille eploree.
Vraiment
Yalnako yalla yeureum té kharéko al dianna
Yalla nako yalla yeram te khare aldiana 😭😭 metina
Oho lake microbe la mou doguou si canalbi daye guena aggravé masta yalna nako yalla hare aldiana
Ndaysane yalla nako yalla yereum en tout cas ki kou mouss la rak bou bakh gua
Ms Mamadou yalla n'a yalla yeurme té kharéco adiana 😭🔐
Histoire bi louche trop
Yalla rek k xam ce qui s'est réellement passé
Paix a son âme
Entouka dall sen version barina trop
Vraiment
Yalla nako yalla yeureum te khareko aldiana firfawsi thi barke yonenty 😭
Ki rakk bu bakhleu
Bilahi li sama quartie la
Bilahi xam nako bou bakh boy yarou
Vraiment c'est un jeune très courage,
Qu'allah vous accueille dans son paradis céleste diarbate et k justice soit faite
En tout cas Sénégal 🇸🇳 nagnou ragal yalla deugou di wakh li am sans haine adouna dou keur nieupay deh beneu nitt boumou la diaral wakh loudoul deugu
Dagnouy wakh goro yi mais diegg dji tamite amna thi niou yéés cheuuu
Bilahi wakhati kou djiguene diou bakh yomboul bilahi soniou wakhè rek niouy wakh goro yi ak ndièkè yii
😑Djiguéne diou bakhe waroul tk goro torr bou fékè danga beugue domam mais nag nioune goor yi naniou am fouleuh souniou bopou
La maman du fille walah elle est louche
@@sergentbahserge3137 vraime
Paix à son âme aldjiana firwdaws sa fait mal dans cette vie je demande le bon dieux de nous protéger contre le satan 🤲🤲
Yeine famille kou goor guiii yeine yeina amoul droit si mom ndax vous l'avez rejeté,,wa keur amineta gno hébergé mame mor,,oui nitt Dina kharou Di sauver bopam ndax douleur bi ladoul meuneu supporte,,
Lolou lo khamla walla lo analyse
@@thiamnogaye9807 personnellement Mane gni lé conné pa youtube rkk lako djissé..mais tamitt ki rakam bi nimouy wahé si famille kou djiguènn ki ak Koy djiguene ki c reste à voir ..n'a nice touti ba enquête bi parè au moins ils ont accueilli leur fils kan il été dans le besoin
@@thiamnogaye9807 et en parlant de nitt Dina kharou Di sauver bopam Lolou mom c vraie..et je dis pa k pa mor da kharou Lolou Dara waroumasi j'attend l'enquête comme gneup
Femme bi moy mbam😭 deum rayla diale lela
Merci ma belle
Mon pays vas Mal 😭😭😭 que son âme repose en paix et que le paradis soit sa dernière demeure
Yalla naniou yalla mousseul si partenaire bou yess gni niou boneu naniou la femme et sa famille sont mauvaises
Yalna yalla leral lépp
Vraiment ce cas me dépasse ton père à dit qu'il n'a pas parlé et toi tu dis le contraire. Pourquoi votre frère ne vivait pas avec vous.?
Arretez vos questions et priez pour le mort. Les histoires de famille ne nous regardent pas.
L’amour
@@moustaphafall9310 vraiment 🤷
Diabar daniou kay tane
Paix à son âme
Que justice soit faite
Bilahi. La beauté se fane. Affaire bi dou taar. Djikko ak outal say domm yaye bou bakh c'est ce qui compte
@@khadidjatoukambye3664 bilahi motakhite lou nek gay guiss
K’il repose en paix
En tank capital hôpital nit urgent beugue fadiou meuno fadiou
Sénégal metina😭😭😭🙏
Boy bi vrai guerrier l
Li amoul sakh ma dém té nieuw c la femme qui est à l'origine de tout. (Sama soeur woona sama yaye néko tankam dafa daam thi escalier la daanou Mane gueumone naco au début mais bimou dougoussé djieukeur dji indi co niom niaare sene comportement la khamni danio khékh dieukeur dji guagne co. Après damaco lathie insisté Mouy soga wakh deugue wa keur gui). Parenthèse la wone. Limay conseillé famille ba Moy nagnou topou cas bi.
Wa sa sœur bii dafa am soutoureu motakh lignay wakhni souniou nion nekousii nianalall ki décédé moguen siyaw
Ndessane seuy dafa meti
Yalla nako yalla yeureum
Waw même hôpital Sénégal tamit ba Tay ces comme sa
baix à son âme
Sirtou lolou yala rék mo khame
C'est triste vraiment ! Émotion A à Z !
Avec les deux versions que j ai vus personelment la femme n as pas faits les acres qu on la renonce je pense que le gars a oublie d eteindre le megot de cigarette et ce que a produit le malheur.je parle en connaissance de cause sincerament. C est Mon point de vu
Lolou mo rey sama mak megobi mo tal matlabi ba fadiar gnouco yek
Legui pétrole bo foumou djougué
Alhou ak bar 😭😭
May his gentle soul rest in perfect peace ndeysann very sad 😞 😢
Amine yarabhi
Yalna ko yalla yeureum
Bon c très taux pour jugé 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Bilay Mane dh douma jugé
⛔️ Aywaay bayi lène yakhanté bi. Lii accident rék la té lolou la justice di conclure. La famille de l'homme voulait mou takk sène mbokk motakh gnagass gnagass ame ci diganté gnaari familles yi. Mais kéne rayoul kéne kharouwoul. Pétrole mo nékone ci chambre bi pour dakh matt yi ak khétou sawou khalé yi. Le mari s'est lavé les mains avec pour dindi huile bi takhone ci lokho yi. Wakh nguène fi ay garabou yo ak ay cigarette té lolou lépp andoul ak pétrole. La femme croit que le mari s'est suicidé ndakh dafko done menacer, la famille du mari défend l'image de leur défunt fils en accusant la femme ndakh dagnou done histoire juste avant. Soupçons yi commencer ak mauvaise interprétations yi (en commençant par celles du petit frère). Gnaari familles yeupa baakh et ça se voit. Massa et pensez aux enfants svp.
Ya moune doul c la femme ki l’a brûlé
@@youzarchif2393 en tout cas soula wooree baah na
Ta parfaitement raison
Repose en paix mon frère 😭😭
Ccey yalla yalle na xippé fridaossi masha allah
Paix à son âme
Ho 😭😭😭😭😭li métina trop sakh yow
Famille diabar qui décédé tmt louche nagn niom dall lou waay wakh rk amnagn tontou ba paré
Yalna yalla atté si yeurmandéw té diégeul ko té fenial ki df liih
Nji kaye danio doye war trop danio wara nopi yalla rék mo kham li khéwe
Naniou tàkho ndiàpp di zikre lahilàha illalah moy noonou seytàné
C important
Li niawna trop djigen gou bakh d'où deff li dieukeuram 😭😭😭
Bilay
Ki guem na sugnu regler wul li dina fadial bopam
Hummmm femme qui es tu ?😳
Li Mettina troppp comment est ce qu’un être humain peut bruler vif son mari 😭😭😭😭repose en paix🙏🏾
Neup neupeul bissi deuk bi lagnou wara bayi ..Pourquoi ne pas dire ce qui s'est passé depuis le début. Paix à l'âme du disparu
Djiguene bou bone agressif bakhoul amna bene femme bou deuk souniou keur dh ni la mel Hoo djiguene dji bonne sakh
Yalla na co yalla yereum aminnnn yarabahallamii ne
N deyessane yalnako yalla yereume
Massa paix à son âme que firdawsi soit sa derniere demeure amine yarabi
En tout cas moytou l'en toumala nit.nénga ci camotte bi la femme bi tek pétrole bi,domam neko papa sa lokho bi takk n'a pétrole,mom la victime ci bopam né mo Tal briquet lokho bi lakk si j'ai bien compris,une tante à la femme dit que li lep tokh moko ko yobé...pour man femme bi dafa tek pétrole bi fou wadji teud mou tourou,lokhom toy ci Mouy tokh par maladroit lakk bomap daw ci canal bi Di sauver bopam,diabar dji fokni dadone kharou .peut être lolou la beugone expliquer freram bi bimou nan kouy kharou d'où sauver bopam pas pour accuser sa femme.yalla réka kham nak.que son âme repose en paix
Sou fékkon yéré yi amna pétrol peut être mou lak ko lakk mou metti mé lokho yi késsé mou tall cigarette pour tokh mou lak yaram yeup lolou noumou meuna nékké je sais pas la vérité nakk mé c trop bizarre
Soxna sii Aminta bokholé bã khole wakhout dëgg.
Sén papa tamit mé yalnako yalla xaré aldiana
Thieuy chaque jour akh lou bess metina trop
Yalla nako Yalla yeureume té Kharéko aldianatoul firdawsi