Bi may diang togg thiebu yapp nilako dorewone. Bakhal lepp nokoss bu saff. Akk lakhass yi bop xar bi. Mere bi wouy yakk na sama ndawal. Way deh gnit bole ba lanu deff. Merci madame pour cette recette🤗🤗
Machallah amna solo fatelinama arabie saoudie defna 7ans la bas mais dounou nokhos day wekh mais dina nekh aussi huile dolive lanouy def rose mendy la doutou fofou merci marietou yalna barkel vitamibe rek la
Tata Marietou. Ma sha Allah. merci et Yal na la Yallah teral. amine. Thiebou frontiere bi m'a fait rigoler. No stress ak yow. Yal na nga am yokute! amine
Marietou domaray dee damay ree rekh boumay lay setan machallah yallah na yallah weural.lokho bii. J aime trop ta cuisine limassi gueneu nekh moy you don't use all those garbage de bouillons. Love u
As salaamu anleykum tata..aah maa shaa Allah jazaakillaahu hayral jazaa i linguay deff amneu solo yalna yalla saameuleu.. Damay reii ba soon ak say termes.. Maa shaa Allah
Tata marietou say terme gnomay danel ay Neko rel, bamou tere bien...linguay togou mashalla damala aimé walahi je ne rate jamais tes vidéos yeup tere bien mdr...merrrci pour tout dama beug togou.
Merci bien waay legui diw nior noumou toudou en français j’ai envie d’acheter ça ici à Paris stp c très digeste ce plat ak les petits légumes c’est juste parfait comme j’aime . Pas gras en plus limaci nekh tu cuisines non seulement ak amour mais tes ingrédients c’est 100% naturel sans cube et compagnie gros bisous 😘
6 років тому+2
pasiphaee valio17 merci ma Cherie pour les compliments le nom en englais c’est Ghee butter alors c’est juste du beurre clarifier et ici on peut les trouver dans les stores Arab ou chez les Indians merci
Tata mariétou délongama sama réw se plat bii téknathi 25000f ak bène nakk 🐂 boundaw thi samay térangue. Mé se thiébou guédje bou khonke bii té ame gnébé bou barri bii jusqu'à présent je le savoure 😇😋
Grand remerciement, une recette que j'ai beau cherchée
Ta Marietou je t'adore vs êtes telment jovial te yagui may diangal Lou beury merci encore
Wallahila zeine machalah togue day naturel waayé boullon ko ba gouwou yapp bi dem
Bi may diang togg thiebu yapp nilako dorewone. Bakhal lepp nokoss bu saff. Akk lakhass yi bop xar bi. Mere bi wouy yakk na sama ndawal. Way deh gnit bole ba lanu deff. Merci madame pour cette recette🤗🤗
😂😂😂😂😂
Ma kham plat bi boubakh c’est tellement saint et très délicieux
machallah com dad rek thiébou nar bi mome bakhna si siniou sédaye yi sett na selle na machallah
Ta mariètou néna rél béne aimer😂😂😂😂 ndakh lép très bien😘
Kone néko rééllllll😂😂😂😂j'aime cette façon de faire les vidéos !
Bilaye sama vacances yii say plats donc laye khol macha allah
bonne recette machaalla bravo Mariétou 👍👍👍👍🙌🙌🙌💕💕😁💋
Bonjour Tata mariétou macha Allah je vous suis toujours waa loutakh doo Rossi sa thiepe bou toye môme réke laa teulé togue
Mashalla. J'adore ta maniere de cuisiner Tata Marietou. Bonne continuation inshalla.
Machala tata marietou thiébou Narr bi dall peuteukheul guako
Machallah amna solo fatelinama arabie saoudie defna 7ans la bas mais dounou nokhos day wekh mais dina nekh aussi huile dolive lanouy def rose mendy la doutou fofou merci marietou yalna barkel vitamibe rek la
Aujourd'hui moome tu m'as ramené dans mon pays! Merci bcp tata marietou!!!
Oh thank you tata😊machallah bien prepare😋où sont les mauritaniens 🇲🇷🇲🇷🇲🇷
On es là 🇲🇷
On es la
On ne la marou helouwo zeynehatt machallah
Tacko belle nioguini dee machallah xateuuuuuuuuuuuuuu
Présent 🖐🏾
Merci pour avoir fait un plat de mon pays 👍🤤.
Thank you for speaking in Wolof because I don’t speak French lol your so fun to watch ❤️😂
Né rel 😂😂 machalah thiebi nexna
Li nakk moy thiep original, rakhoul dara masha allah😍
Machalla tata
machaalah nexna selna chapeau comme dhab
Tata Marietou. Ma sha Allah. merci et Yal na la Yallah teral. amine. Thiebou frontiere bi m'a fait rigoler. No stress ak yow. Yal na nga am yokute! amine
Fatima Kane Ameen
Amine.
Marietou domaray dee damay ree rekh boumay lay setan machallah yallah na yallah weural.lokho bii. J aime trop ta cuisine limassi gueneu nekh moy you don't use all those garbage de bouillons. Love u
Tata marietou nekh ngua ma. J'adore ta voix et la manière dont tu aborde tes recettes. Bisous depuis la France
Sa thiep daleu nèna releu😍❤
j'ai abonnée aujourd'hui j'apprécie bcp
Aywa bismila tata marietou machalla magui si guinaw nouvel abonee
Amna solo trop. Togueu nako exactement comme yow. Nekhna maa cha Allah seleu neu. Je te félicite pour tes recettes. Bonne continuation!
As salaamu anleykum tata..aah maa shaa Allah jazaakillaahu hayral jazaa i linguay deff amneu solo yalna yalla saameuleu..
Damay reii ba soon ak say termes..
Maa shaa Allah
Merci tata Marietou, man narre Mauritanie mais Machallah thieb bi dafa naix trop. Diaradiof Mere
Machallahhh Tata Marietou. Merci beaucoup
Ca me rappelle nimzat ❤🎉
C com a Mon village (cantchungo)presicement guinee bissau
Mère néko rél 😂😂😂 macha Allah togne bi nirona ak lou nekh dal
*yapp thiep waaaaay😹* sama yaye naar la mo takh lii rekk la kham
Lak ngako machalah borom neko rel
Salam tata marietou nekhna ba tere bien Machallah
Maman beug nala way😍😍
Joyeux Noël tata marietou machallah gros bisous je t'aime fort fort fort
Aida Thiam 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Olala néko thi réleu machallah😂😂😂
bonne et heureuse annee
Comme d'hab ,, khéte bi gneuwe na be Italie,,, néngako tchi réleu!!
Assalamou aleykoum warahmatou Allah tata marietou sa thebou nar diapana form
Thièbou frontiere eup naa 😂😂
Sama maman adore 🥰 yalla na sa diam yagg 🙏 merci bcp ✨😍
Tata marietou say terme gnomay danel ay Neko rel, bamou tere bien...linguay togou mashalla damala aimé walahi je ne rate jamais tes vidéos yeup tere bien mdr...merrrci pour tout dama beug togou.
Wollah té pas la seule ma belle. Shui fan des termes kelle utilise.
Merci pour tout wa saveurs planétaire
Machallah tata delongama deuk ba ahhh France amoul yii waay 😥
lol maman on t'aime 😍
Sama khel mogui si déh walahi bilahi depui New York
Man takh gueu me begeu tog vraiment pas mention spéciale si terme tata Mariama fii si paris ❤️🙏🏾
Merci bien waay legui diw nior noumou toudou en français j’ai envie d’acheter ça ici à Paris stp c très digeste ce plat ak les petits légumes c’est juste parfait comme j’aime . Pas gras en plus limaci nekh tu cuisines non seulement ak amour mais tes ingrédients c’est 100% naturel sans cube et compagnie gros bisous 😘
pasiphaee valio17 merci ma Cherie pour les compliments le nom en englais c’est Ghee butter alors c’est juste du beurre clarifier et ici on peut les trouver dans les stores Arab ou chez les Indians merci
machallah zeiyna hatte
Bon appétit à tous merci tâta safna
Waw moi jsui mauritanienne entouka c comme sa quon le fait c bien machalah zeine hateu
Marieme Ba w mcha3cha3
Tata.machala.lingay.togue epeuna
Doum safi deh billay
Macha Allah macha Allah
Jeureu jeuf Sokhna Marietou. Bonne continuation.
Khady Faye merci ma Cherie
1ere vue 1ere commentaire doumako ratè en aucun cas mane Tata marietou momaye fadj
Bravo tata
Néko ci réleu la manoul mougne😂😊😂
Bonjour ta Marietou merci pour la recette. C pour quand le mbakhal diwtiir dieune akk soule?
Aissatou Diallo bientôt Insha Allah
Bonjour Tata Marietou Machallah nekhneu thi beut Sinon le riz daguako sebet wala tay
Dieng Fatma merci ma chérie thieb bi danga ko khoth
Merci beaucoup
tata mariétou ligaydef amna solo
je suis vraiment contente parceque Mauritanienne theib sans consequence nefaste vs allez aimer nos plats
Sow Idrissa
Mais ani khogne bi😛
You are great cook. Thanks for sharing
Tata marietou je vous aime telment j'arréte pas de regardè vos vidéo
Très bien dans huile sans gras.j'aime
mala beugueu tata yalna sa diameu yagueu et joyeux noël
Ahmadou Ndiongue Amenn 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Machallah mariétou mane magui Mauritanie sama tourado
Mariétou Ndiaye Masha Allah 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
machallah tabarakaallah machaallah
Djeul suñu yap khar ak yoyou neko toi réleuu no mère bi ndinama dadji
Tata marietou ihh li mnoumako togue😂😂
Machala c simple
Ummm bii dohna. Mariatou beugo tasting officer? 😊😊
Machala meuna tog en plus sinpatik
Trés bien Tata Mariétou. On pourrait avoir la recette de du Mafé please ?
Nalouchaa ua-cam.com/video/IlKkmMFkQAg/v-deo.html
Nalouchaa ua-cam.com/video/ZsI3hDsHgac/v-deo.html
Saveurs Planétaires thank you very much 🙏🏾
Ma cha allah amatina solo sama toguolokh bi
marietou a quand les astuces de jus naturels
❤
Ohh merci way tata marietou sama tourondo. Je suis mauritanienne
Marietou Diabira waw rourondo merci Mauritanie sen gnam mo geuneu sein sougnou gniam
@ merci tata chérie en tout cas ya pas bcp de l'huile ni de bouillon
Machalla amna solo le riz aussi se vend aux boutiques auchan
Eupeuteuleuw défati nga délit dê!
Nékhatina dall
bi mom amna solo maman adoré
recette origine bi nak lou am solo la.
Bilay tata je t’aime trop machallahh yalla na lokho bi wére🥰🥰
Bitty Diongue Ameen wayy
Mane daal olalaah bi, ak nekosi releuh gui raynama😂😂
Tata mariétou délongama sama réw se plat bii téknathi 25000f ak bène nakk 🐂 boundaw thi samay térangue. Mé se thiébou guédje bou khonke bii té ame gnébé bou barri bii jusqu'à présent je le savoure 😇😋
cheikh fall 🤣🤣🤣🤣🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Tres belle voix
mo zao Masha Allah 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
kc
Machallah
Je suis pas fan mais ça doit être plus saint que le thieb qu'on voit d'habitude car c'est pas trop gras.
Bonne continuation
tata deniouy wane fingay defe epices yi ak sel bi amna thi solo ndax amna nio xamni danioulay roye a la lettre
Mame Mor Kane ok Insha Allah merci wayyy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Ma shaa Allah man dama fay diaré abonné lo togue tey ma defko souba. Lima ci gueun nekh daga beuri fèm wakh ji nèkh yaw dal Tata Merci rek
Man dall neko releu may Ray😂😂😂
Dieuredieuf waye😂😂👍👍
Merci tata
Ñam très bonne manger 🇲🇷🇲🇷
Li kay niamou khalé ak mak yèpeu la