Massa waye Bassirou. Une famille calme avec qui nous habitions la sicap liberté 1. Jusqu'à ce jour nos familles sont liées : c'est devant la maison de son père que se rassemblent ses grands frères et leurs amis . Chose vérifiable. Son père était cheminot et père de tout le quartier. C'est de cela qu' a hérité Bassirou. Feu Moustapha porte le nom de son frère. Que firdawsi soit sa demeure éternelle ainsi que nos défunts parents et tous musulmans.Amine.
Que le le bon dieu l'actueille au paradis firdaw et exos naux prière s qu'inssie à toutes la famille et proches, virement ça fait mal, bon courage à la famille.
D'après vos dires vous êtes un père responsable que le bon Dieu vous donne la force, la foie de pouvoir surmonter cette épreuve. ALDJANA FIRDAWS à ton fils
Ndeye sane papa metina troop yallah nalla yallah borome bi swt maye la kholoup mougne tè leral li yeup si barki SEYDINA Mouhamed alleyhi salâtou Wa sallam
ce qui me fait mal moy on n'a montre le corps calcine de la victime😢😢mais si le criminel est arreté,en complicité avec les droits de l'hommistes et la police son visage est cache aux senegalais.😢😢
Imallilahi wo ina ileyhi radjioune inallilahi wo ina ileyhi radjioune inallilahi wo ina ileyhi radjioune Allahouma aghfirlahou wo yarhamhou amine que le bon Dieu ľaccueille dans son vaste paradis firdawsi amine ya Allah
J’ai vu beaucoup de vidéos avec le même titre ms ce qui m’a interpellé dans cet vidéo c’est lorsque j’ai constaté qu’on partage le même date de naissance 14/10 j’ai pas pu m’empêcher d’observer la vidéo de ce gentil garçon yalla nako Yalla yeureume
Un père aimant, responsable qui s’occupe bien de ses enfants.
Je t jure
Mon Pays 🇸🇳va mal ❌ oh la méchanceté 😭😭
Vraiment Pape deug la yalnako Yalla may kholo mogne
Kham gané ki sonouna thi domame
Il est digne le vieux. Paix à son ame
Un père aimant il m'a donné les larmes aux yeux ❤
Ndeysane ça se voit que Pa daye topato ndiabote, diape na détail yi khalé bi sole yeup. Té Pa bi nimou guemé yalla, yalna yalla nite ki déf li
Goorgui!
Kou gueumm Yallah nga!
Yallah milako diokhoone mayla kholou mougn té mou mottalé ndawam Aldianna Firdaws!
Massa waye Bassirou. Une famille calme avec qui nous habitions la sicap liberté 1. Jusqu'à ce jour nos familles sont liées : c'est devant la maison de son père que se rassemblent ses grands frères et leurs amis . Chose vérifiable. Son père était cheminot et père de tout le quartier. C'est de cela qu' a hérité Bassirou. Feu Moustapha porte le nom de son frère. Que firdawsi soit sa demeure éternelle ainsi que nos défunts parents et tous musulmans.Amine.
Ndeyssane métina lole paix à son âme nite mo meuneu togne gni deff dieuf dji yalnaléne yalla wer nite mo sokhor père courage
Rahmatou lahi alayhi
Kou geume yalla ga déh
Yalla nala yall la dolli kholou moungieu
Masa papa Yalla yerem te khareko aldjana fir dawsi amine yarabal alamine 🤲 repose en paix Moustapha
Police dina def écoute téléphonique té dinagn diapp gayi inchallah amoul tite. Masta vraiment
Diap nagn léne
Kane lasi diap nagnouko
Que le le bon dieu l'actueille au paradis firdaw et exos naux prière s qu'inssie à toutes la famille et proches, virement ça fait mal, bon courage à la famille.
D'après vos dires vous êtes un père responsable que le bon Dieu vous donne la force, la foie de pouvoir surmonter cette épreuve. ALDJANA FIRDAWS à ton fils
Massa waye père, paix à son âme
Ndeye sane papa metina troop yallah nalla yallah borome bi swt maye la kholoup mougne tè leral li yeup si barki SEYDINA Mouhamed alleyhi salâtou Wa sallam
Yalnako yalla yeureume te khareko aldiana firdawsi si barke seydina mouhamed metina lol
PSL
Bilay t'as tasnagni yakaru diambour si ay thiaxane
Papa masta yallah nako yLlah yeureum metina trop
Ku geum yalla leu ndeysan😢masta
Dafa am teguine sah,bilay
Yalla nako bour yalla yeureum te dièguelko kharèko si aldiana fir dawsi thi barkhè seydina Mouhamed psl 🤲🤲
Ndeysane papi gueumna yalla
Yalla nako yalla yeureum ta mayla kholou mougne
Kouma meuna bahé numérome svp, dafa ame louma ko yéné trop
Massa 😢😢 khaleyi Yallah molene dii saam
ce qui me fait mal moy on n'a montre le corps calcine de la victime😢😢mais si le criminel est arreté,en complicité avec les droits de l'hommistes et la police son visage est cache aux senegalais.😢😢
Bonne kestion
Yalla nako yalla yeureum te hareko aldiana firdawsi 😢
Dina fégne dé inchaallah Sénégal yakouna masta papa yalla nala yalla may kholou mougne
Massa papa yalla nako yalla yeureum kharéko aldjana firdawsi 😢😢😢😢
Eskey 😢 li métina 😢 niewna 😢 wanté lou way def sa bopp . Yallah nako Yallah yeureum xaréko aljalna firdawçi 😢 djabot bi ak gorgui Yallah maylen xolou mougn 😢 xamétouma Sénégal 😢 niawtef yi beurina
Allaahu Akbar, xol yi wownañu, njeuf yi ñaawnañu😢
Walahi 😢
Imallilahi wo ina ileyhi radjioune inallilahi wo ina ileyhi radjioune inallilahi wo ina ileyhi radjioune Allahouma aghfirlahou wo yarhamhou amine que le bon Dieu ľaccueille dans son vaste paradis firdawsi amine ya Allah
J’ai vu beaucoup de vidéos avec le même titre ms ce qui m’a interpellé dans cet vidéo c’est lorsque j’ai constaté qu’on partage le même date de naissance 14/10 j’ai pas pu m’empêcher d’observer la vidéo de ce gentil garçon yalla nako Yalla yeureume
Moi aussi on partage la même date de naissance 14 /10 paix a son âme
Man loutakh nit sokhor teksi domaram daf ma Diakhal 😭😭😭😭💔💔💔
Adouna dafa yakhou walahi
Mais tmt Khalebou djgeunne bimou raye metina deh ndakh domou diambour la
Ndéyesane wolaye métina 😢yalla nako yalla yeureume t’es kharéko aldiana firdawsi si barké seydina mouhamed psl 🤲
Un homme tres calme… yalla nako yalla yeureum
Yalla nako Yalla kharé Aldiana masta papa
Vous êtes un papa courageux très croyant que Dieu vous assiste dans ces moments difficiles yalnaco yallah karer aldiana mettina n.deyssane
Ohhhh😭😭😭yalla nako yalla yeureum moygnal pere yalla bakhna
Ndeysan
Mettina vraiment que dieu vous fortifiés inchallah que firdawci soit sont deumeurs internel
Ndeye sane bilaye métina ,j’ai les larmes aux yeux ,courage pére ,yallena. Yalla yeureumeko té haréko aldiana amine
Metina trop massa siguil lene ko ndigualee YALLA BOUR BI kharee ko ALDJIANEYE FIRDAWSI si barkee Mame BAYE LAYE ALAYHI SALAM AMINE 😢😢😢😢😢
C'est vraiment triste paix à son âme que le paradis soit sa dernière demeure
Ndéyssane yalla nako yalla yeureume tabalko thie aldiana you guena kawé yalla naléne yalla nith wassalame
amine
Amine
Ndeysane yalnako yalla yeureum té xaré ko aldiana firdawsi 😭
Que Dieu l accueille dans son paradis
yallanako yalla yeureum kharéko aldiana firdawssi 😭😭
Amine Yarabal Alamine
Pere bou responsable. Ka neysannn tai yarr sa niabotte par rapport a tes paroles masta et du courage
Nit yi sokhor nagn légui trop cheuteutteut mé yeufou vampire yi louy ndeyam 😭
Gni kaaay vraiment dougnou nite
metina ndeyssane
Neysane pape yalla mouñeule ñanalko mais metina trop Neysane mais ki make bou bayi khele doma me laa
Ndeyssane kou geumm yalla métti na mais yalla nako yalla yeureum
Que firdaws soit sa demeure éternelle si barke SEYDINA MOUHAMED SAW 🙏🙏🙏 massa Bachir
Yalla nako yalla yereum
Dieureudieuf Papa Yalna la k Yalla wutalal lénén
Que dieu l accueil dans son paridis
Pabi nitou aldiana la tey na dal na vraiment yalla nako yalla may holou mougn domam bi yalla xaré ko aldiana firdawsi
Soubhana allah
Ay nite moo doy war
Ndeyesane yalnako yalla yeureum 😭😭
Yalna yegalé ndawam Aldjana firdawsi
Allahou Akbar Massa way papa. ohhhhhhhh😭😭😭😭😭😭
Yalla nalleuh yallah maye xolou mougne 😢😢té yalla yeureumko xarrékeu aldiana
Ndeysan massa, yalnako yalla yereum
Ki def li yalla nako yalla wer
Que son âme repose en paix et yallah nitte gniko def bagnou fègne si barki Mouhamed
Thieuy yala li metina trop😢😢
Ku beug domleu❤
Que justice soit faite yalla nako yalla yereum té kharéko aldjiana firdawsi amine
😢😢😢😢😢yalla na khippe aldiana
masta papa
Vraiment mon père vous êtes un vrai lion.ndeysane
Yalna yala yeureum djigualko
Ndéye sane vraiment métina trop yalla yeureum ko amine way 😢
Walhahi ndeysaan ko am dal la yalla na yalla yaram Mustapha amine
Machallah papa yalla nala yalla may khoulou mougne.K firdawsi sois sa demeure éternelle
Lii 😢😢kouka def danou wara dakhaar ndeyam 👍 a vie 140ans
Ndeysane yalla na yalla maye la khoulou mougne
En le voyant parlant on sent que ce père est un vrai éducateur, surtout dall bii.
Nakhar yagu na si adouna bilahi métina, yalla nako yalla yeureum
On voit un père très responsable.
Il est aussi très juste sur ses propos. Massa papa yalna yalla yeureum ko té mayla kholou mougne
Massa yalla na Yalla yeureme ko amine yarabale alamine
Un homme digne et intègre qui est prêt a se sacrifier pour que le Sénégal émerge son excellence bassirou Diomaye faye
Yalla na motalé ndawam Aldiana
Massah père yalla nala yalla maye la kholou mougne
Yalla nako yalla yeram
Que le Bon Dieu l accueille dans son Paradis Eternel 🙏🏽🙏🏽
Ndeysane yalnako yalla yereum té kharéko aldiana thi barké seydina Mouhamed 😭😭😭😭😭métina trop
Un papa responsable 😢 ndeysan massa
Yalnako yalla khare aldiana firdawsi Ina ila wa Ina ileyhi rajihun
Yalla nako yalla yereme té khareko aldjana firdawsi
Méti na trop yalla nako yalla yeureum té xaré ko aldiana
Q'Allah vous accueille vous et votre fils au paradis
Papa yalla nalla takhawou si bareke sayedouna moukhamete 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Massa wayii papa que son Âme Repose en Paix 🤲
Al hamdoulilah ala koul ha
Ndeysan Yalna k Yalla yeureum t kharé k Aljanay Firdawsi ya guena kawé Amiin
Massa paix a son âme que firdawssi soit sa demeur eternel amine ya raby
Ndeyssane paix à son Âme Qu'allah l'accueil au Paradis Firdawsi
Ndeyssane le papa 🌸
Ndeysan pa bi kou yague beugue topato domam
Yalla nala yalla maye kholoup mougne masta lou meti la
kou guem yalla pér masta yalna yalla yerem khareko adiana
Un père responsable
Ndeysane métti na mai yalla nako sama brome yeureme té kharé ko aldiana firdawesi si barkè seyidina moukhamate si barkè nabi Moustapha 🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Soubhanallah li mettina trop😭😭😭
Yalla nako yalla yeureum
Masta pape du courage siguil digualé
Yalla nako yalla khare aldiana
Ndaysanne 😢😢😢😢😢😢