Dof Ndeye dafko diam bamou: ce détenu en colère et éclate tout et parle sur l’affaire de Campénal….

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 24 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 75

  • @ibrahimasy8018
    @ibrahimasy8018 7 місяців тому +35

    Ndeyssane yaram dawna yalla nalen yalla sam arlen téklen si yonne bou bakh té mousseulen ci barké mouhameth

    • @laminendiaye78
      @laminendiaye78 7 місяців тому +5

      Del dioulii si mom Seydina Mouhamed (PSL)

  • @kaneamsa2261
    @kaneamsa2261 7 місяців тому +5

    Ligay wakh masi kham dra bilahi sama dem prison Lolou moma si geun meti somi ma bama set dima thiotou la somi ay pa sama kanam😢😢mais alhamdulillah legui magui Amérique 🇺🇸❤️❤️❤️

  • @Gkcdshndsncs
    @Gkcdshndsncs 7 місяців тому +8

    Deug nekhoul m Sénégal neik fi pauvre d’à metii😢😢😢😊

  • @laminediouf5417
    @laminediouf5417 7 місяців тому +10

    18:47 dacor n'a cii li nga wakh mé bayilénn agression bou méti bii

    • @abdoukhadrediouf5919
      @abdoukhadrediouf5919 7 місяців тому +4

      Amoul moral boyi nio begueu Lou yombeu . Goor Yalla degueu d’où agresser

    • @ibrahimafofana-s6l
      @ibrahimafofana-s6l 7 місяців тому +1

      ki si election dadone manifestewu nguena agréation doul way sen data yaye

    • @abdoukhadrediouf5919
      @abdoukhadrediouf5919 7 місяців тому

      @@ibrahimafofana-s6l agresseur yi nio mom wax bi . Bayil sa saga yi . Nioune ki xamouniou loumou deff on parle de manière general

  • @ousmaneba9503
    @ousmaneba9503 7 місяців тому +5

    Agression ak yefou wayou ak yefou bandi ak yefou CIRMINEL mo wara diekh sy Sénégal 🇸🇳 ñou am diom te doylou te liggeye incallha dina bakh

  • @CheikhTidianeNGOM-u5w
    @CheikhTidianeNGOM-u5w 7 місяців тому +10

    gouvernement dina ci diapp inchalah yalah baxna

  • @damefall4471
    @damefall4471 7 місяців тому +3

    Métina vraiment té ki kou kham limouy wakhe la
    Yalla bakh n'a 🤲🏼🤲🏼

  • @cheikhfall4377
    @cheikhfall4377 7 місяців тому +3

    🇺🇸 Vraiment actroces doÿna Warr entouka tu as parfaitement raison bro j'ai fait 3 jours à la prison de reubeuss en 2014 avant de voyager j'avais 16 ans mais c'est dure si ta famille n'a pas beaucoup d'argent 😢

  • @BoyeCasa
    @BoyeCasa 7 місяців тому +3

    Ndeyssan mos nako mais metina torp billah 😭😭😭😭😭😭

  • @oumygueye6416
    @oumygueye6416 7 місяців тому +1

    Deysanne yalla naléne yalla guéné thi diam 😢

  • @moussangome708
    @moussangome708 7 місяців тому +13

    Boy régler lénn mo guenn nguéénn nékk fi nann président

  • @DialloAbdou-fp6gq
    @DialloAbdou-fp6gq 7 місяців тому +1

    Gayi aydom lane bayal dimlen😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲😭😭😭😭😭😭😭🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️

  • @biranendiaye5268
    @biranendiaye5268 7 місяців тому +2

    Ndeysa thiay yalla meti na trop

  • @papesene4374
    @papesene4374 7 місяців тому +1

    Yala na yala noulignou diame

  • @ModousambModousamb-mm2wk
    @ModousambModousamb-mm2wk 7 місяців тому +2

    Fi la Diomaye gracié ay détenu le même jour deux détenus libérés défat crime kén ki ray béneu tailleur kénén ki agressé bén femme et après ngén nék fi di sonal nit gni 😢😢😢😢

  • @alioudiop2791
    @alioudiop2791 7 місяців тому +6

    DEUG la les pénitenciers sont tellement méchant

  • @gueyemodou3456
    @gueyemodou3456 7 місяців тому +2

    Sounou kasso yi dangay warou Billahi yalna yalla takhawou gnép

  • @MadeleineDerneville-mb6bd
    @MadeleineDerneville-mb6bd 7 місяців тому +1

    C triste loll loll ohh😢😢😢

  • @youssoufabdoulayediopjohnn3774
    @youssoufabdoulayediopjohnn3774 7 місяців тому +2

    KHAMNANII YAWMAL KHIYAMA DINA DOY WARR BAKHNA TE BOROOM BI WALAHII DINA ATEH JUGES YI GARDE PENITENCIER YI KHOLAT LEN SEN BOPOU BAKHNA

  • @mohamedd7470
    @mohamedd7470 7 місяців тому +4

    Bayi yén nieupp diko wakh. Deugueu la. Mais souvent niou bayi kou niakk diom. Di guéneu sonal askan wi

  • @bellediolla3414
    @bellediolla3414 7 місяців тому +3

    Faut savoir que amougnou pour takhou pour fouiller les chambres de détenu. Amoule beneu prisons si monde bi bougnou prevenir pour fouiller.

  • @KhadimLo-tw4tc
    @KhadimLo-tw4tc 7 місяців тому +2

    Man sama question daniou lay togne tedj la moy lan diay yamba agression ba paré nan togne la daguéna wara kholat sen bopou nit daga wara diapalé say parent maytou doundou yeufou bandi amoul chance nek Len nit

  • @thiernodieyedia908
    @thiernodieyedia908 7 місяців тому

    Triste

  • @mormbodj-rh3ef
    @mormbodj-rh3ef 6 місяців тому

    ❤❤❤❤❤❤😢

  • @coumbafaye9319
    @coumbafaye9319 7 місяців тому +2

    Dou niep deh wayer fi ma deuk bilahi barket serigne babacar sy charrette yi si sama fenetre lagnouy diar malene di degue. Un jour dama yerndou ndank di ko guisse ak lenene. Et....niou bone gni gnoy yakhal niou bakh gni. Yala nalene.yala diapaler baniou guene si kossobi si batket mokhamed psl.

  • @mosi301
    @mosi301 7 місяців тому +4

    Kasso bakhoul yènèwmako bène domou Adama mai nak sou nèkinwi yombè fofou rèk deuk bi yakhou

    • @Imamlyrical
      @Imamlyrical 7 місяців тому

      Boudé lolou sax amoul problem, mais tedjie nitt te defoul dara mofi wara diékh🇸🇳

  • @34983
    @34983 7 місяців тому +1

    même les dirigeants ont vécu la fouille d'entrée à nu. Et c'est le règlement partout dans le monde, par mesure de sécurité.
    Je ne parle pas des conditions de détention.

  • @Nguerasenegalensis
    @Nguerasenegalensis 7 місяців тому +1

    😮😮

  • @AbdouazzizNiang-jq7yd
    @AbdouazzizNiang-jq7yd 7 місяців тому

    ❤❤❤❤

  • @dioufmodou4234
    @dioufmodou4234 7 місяців тому +1

    Sawaye casso dou nekhe dioplene ligaye wakhe leroull dara tapale casso da am negou daibour

  • @mbayediouf7321
    @mbayediouf7321 7 місяців тому +2

    Press saytane yi

  • @siyakhafadiga1773
    @siyakhafadiga1773 7 місяців тому +1

    Ndeyssane

  • @LSVDFV
    @LSVDFV 7 місяців тому +1

    ki ame na expérience nak

  • @AladjDem
    @AladjDem 3 місяці тому

    😅😅😅😅❤❤❤❤ok

  • @mobarakff9797
    @mobarakff9797 7 місяців тому +1

    Non mais declaration bi doynawar 😢

  • @petersept4334
    @petersept4334 7 місяців тому +1

    Comme lac2 quoi senegal amoule loi kou ame khaliss deff loukeu nekh

  • @assanepene
    @assanepene 7 місяців тому +1

    billahi niawna torop

  • @NfamaraDiatta-q8j
    @NfamaraDiatta-q8j 7 місяців тому +3

    Soumarak diele dou hotel

  • @AmetDia-xq6it
    @AmetDia-xq6it 7 місяців тому +3

    D accord n'a si lepp mais perquisition kene warou se taguo si no day y ombe nak souko guayi khame digniy miner lepp MBA niou denkaneko bene chambre no

    • @balletassikoafrique8429
      @balletassikoafrique8429 7 місяців тому +1

      Wakh nga deug mes souniou démé ba guiss dara si prisonnier yi retour dafa wara ame si garde yi ndakh ko teuth ay année meuneloul dara bopam loufa dougou garde yi niokofa dougeul aay doméram laniou naniou may prisonnier diam

  • @cico789
    @cico789 7 місяців тому +2

    Metina theuye diomaye dinbelilene

  • @binetagueye7482
    @binetagueye7482 7 місяців тому

    Prison Senegal laniou wara def prison pouquoi daure com ay mbame

  • @everythingshere5768
    @everythingshere5768 7 місяців тому +3

    Wa titre bimou def si video on en parle
    Il se fou de nous ou quoi

  • @fillysoumare7855
    @fillysoumare7855 7 місяців тому +1

    Ak senegal noumou baré aleu gnou warssé tabax ay prison ay chambres 20 personnes modoul yone bay 100

    • @abdoukhadrediouf5919
      @abdoukhadrediouf5919 7 місяців тому +2

      Faall prison waroul nex . Agresseur , ray katou nitt …. Dagn lene wara tekk Lou mété méti

  • @ibrahimakane-xx1ti
    @ibrahimakane-xx1ti 7 місяців тому +2

    Si la justice avait fait son boulot, dof ndeye n'aurait pas fait une autre victime.

  • @BassFall-vx7kh
    @BassFall-vx7kh 7 місяців тому +1

    😭😭😭

  • @moustaphasine5710
    @moustaphasine5710 6 місяців тому

    On s'en fout arrêté affaires de banditisme bi mo gueune

  • @dioufmodou4234
    @dioufmodou4234 7 місяців тому +1

    Perecidan tuedioulne eta continutilla dioup reckue

  • @binetandiaye1289
    @binetandiaye1289 7 місяців тому +9

    Pourquoi mentir dans les titres

    • @Le_R319
      @Le_R319 7 місяців тому

      Exactement 😂

  • @34983
    @34983 7 місяців тому +1

    Concernant les fouilles, l'administration peut les faire de façon inopinée sans avertir personne a plus forte raison le chef de chambre est un détenu.

  • @WaxElegeance
    @WaxElegeance 7 місяців тому +3

    Fallait cacher son visage 😢. Triste vraiment 😢😢😢

  • @pouyegoormak3022
    @pouyegoormak3022 7 місяців тому

    Ganaw badola mo soneu kon délénn déf lou défou

  • @khadisall3762
    @khadisall3762 7 місяців тому +1

    Pourquoi mentir dans les titres 😮😮

    • @mariamadrame-cy9fl
      @mariamadrame-cy9fl 7 місяців тому

      Dagno meun fen lolou kesse molen yakeu gnom sougnou defone sen propre titre nitgni dinagn ko setane

  • @binetagueye7482
    @binetagueye7482 7 місяців тому

    Nit loumou meuneu def booko teudje yaw ya ko tek thi condition president

  • @KhadimLo-tw4tc
    @KhadimLo-tw4tc 7 місяців тому

    Diay yamba guene wara bayi niank guene diom trop yen gnep ay def kat guene louniou Len def yen la

  • @khadisall3762
    @khadisall3762 7 місяців тому +1

    😭😭😭😭