Salam Baye Mbaye Gueye Syll et merci encore pour avoir rappeler l'histoire des contributions. Jërëjëf Mais aussi on pourrait préciser qu'il s'agit de contributions financières et qu'il peut y exister des contributions en nature. Et sur ce, la Collectivité Lébou pourrait vraisemblablement offrir l'assiette foncière sur lequel la Grande Mosquée a été construite. Et celle-ci reste inégalable. Il faut aussi le souligner. Je précise que je suis lébou et que je ne partage aucunement les propos de l'imam. Mais je me permets de répondre par rapport à l'historique des contributions. Merci encore Baye Mbaye Syll
Dieredieufe serighn touba diarama mam cheikh ibrahima Fall serighn montakha mbacke yalna kor yalla deffal leep Lou mou beugue barkai yonnen bi Muhammad s a w
Mo yaw mi khana deglou video bi yeup? Serigne Fallou joxé million thi tambalibi ba paré continuer di joxer million Chaq année ba jumah bi yegg ngay am loy wax. Cheikh al islam jambar la lole wayé eupa lé wouthi tabi
Ça reste une mosquée Lebou Juma Touba niata lébou nio thi def? Juma tivaone aussi ! Mani l imam a fauté en demandant une visite au président Mani ki di wakh ni bou niiu done délo thi diokh adiya guir tek ray bi momitam dou jot deureum ndakh diokhéwoulwone 😂😂😂 Sène logique à deux balles yi Juma touba bane diola mofa djité hana dou négou yallah Bayilene detail
Serigne Mbaye Guèye Syll yagg fi lol té anda ak wér. Niou mélni yaw la niou sokhla thi mim réw. Sa xam xam bi nga niou bakhé Yalla na la Yalla gueureum ma cha Allah.
Merci beaucoup pour cet eclaircissements! Pa Lebou bi mofi taxawonn nee keup koufi deh tchi manifestation safara nga dieum! Imam bobou ab diff moko diapp, mounann sougnouy diouma!
Ngi nga fi lim yep wakhouma diokhè niou Rahimoulah Amadou Assane Ndoye mo len eupone teranga foufff limou diokhè rek machallah ay dignitaire yi si dess ak libano syriens yi . Bagnelle gui guene bagnè lebou yi 😢 doyna war tropp et pourtant daniou len yatal diay len ba fap khate . Senegal nio ko bok
Dieureudieuf tu as dit ce que les Mourides ont contribué mais il reste la communauté Libanaise, la communauté Leboue en argent et en terres, .... c'est vrai l'imam a mal communiqué, surtout celui qui lui a remis le papier pour faire des prières pour certaines autorités, bref il est mal entouré et cela nous dessert nous communauté Leboue Leboue
Il a dit ce que la communauté sénégalaise avait contribué et non pas la communauté mouride seulement. Si autre communauté avait participé l’article l’aurait mentionné
Merci Serigni bi Mais lingay wakh nii si bignoukoy defarare la Grande mosquée avant 1909 la wone Djoumah negou Yaala la kene momouco Mosquée bii gnou beuri liguye nagnou fa comme maneuvre si temps yoyou Avant 1909 la wone Sama Mame Thierno Mbaye Sylla moo nekone Imam et Cadi Gnome Senghor gneuweu gougnou wone Merci
IL FAUT DEMANDER A TON PÈRE .LES LEBOUS ONT MÊME PARTICIPE A TON BAPTÊME MON AMI .EST -CE QUE TON PÈRE N'EST PAS LEBOU MÊME.EN EFFET BEAUCOUP DE PERSONNES ETAIENT "BOY" OU "BONNES" DANS LES MÉNAGES LÉBOU DE DAKAR.SI TU PEUX ME DONNER 2 NOMS DE TES GRANDS PARENTS JE POURRAIS TE DIRE INCHALLA LA RELATION AVEC LA COMMUNAUTÉ LEBOU DE DAKAR
Les terres appartiennent au lebous je suis patriote je suis de pastef je suis lebou niounes lebous danions yatous je suis pa d’accord avec imam samb wayé lebous kéens douka yaap nions yatale nieupa merci 🙏
Jaajëfeti, Serigne Mbaye Guèye Syll toontu júbb na xocc. Ngòor soosu dafa doyadi té soñu séetaanèè dina taal réewi mi ak laméñam wo ñaaw té ñaak worma.
La Grande mosquée de Dakar est construite sur un terrain appartenant aux lébou "Tatay Ndakarou" des cimetières anciens ! La grande mosquée à été inaugurée en 1964 et tu nous parles des donations de hautes personnalités religieuse paru dans un journal en 1960... Qui a donné quoi de 1960 à 1964 hormis le royaume du Maroc l'état du Sénégal, les guides religieux et la mairie de Dakar ? Vous ne saurez le dire... Parparlo rék, fi Sénégal guiss nagnoufi diakay mouride diakay khadir, diakay layéne , diakay ibadou etc etc.... Dioumay Ndakarou mom lébou yi gnokomom koumou nakhari démal sangoo ndokh mou sédd pour wathié sa température !😂
Salam à vous Serigne Mbaye Gueye j'aimerais que vous me dites 1/la place ou se trouve la grande mosquée de Dakar appartenait à qui avant sa construction ? Combien il a cotisé (les grands marabout du Sénégal ) pour que l'on nomme le mosquée de tel ou tel a leur nom ,je pense que si c'était le cas aujourd'hui si Mame Maoudo(RTA) Serigne Touba (RTA) etc.... N'auront pas mosquée a leur noms Toutes les mosquée du monde sont pour Allahou (swt) Ne change pas la parole de son conteste merci.
Dieureudieuf Barham Niass Srg bi kadou yi rafetna machallah
Billahi baalatilenn niou ahha
Niounn lebouyi toujours imam Samb day togne tognalegnou nounn lebouyi
Yaw da Guaye fine
Yaw doo Lébu wala boodee Lébu itam yaa ci gën a yées.
Jërëjëf seringe mbaye Gueye syll leguey bi ngay def yalla Nga Si Doli dadiék tawfeexi mame Thierno brm darou jërëjëf cheikh bi
Amina
Amiiine
Aamiin
Grand merci a Mbaye Gueye Syll. Bonne continuation si leral Yi.
Thiéy serigne fallou Mbacke ❤❤ yaa manne déh 🤸♂️🤸♀️
Murit yi ñoo moom jumaaji
Serigne mbaye geuye sylla yalla nala yalla yagal weralla amiiine Thie barke seydina mouhamed
Salam Baye Mbaye Gueye Syll et merci encore pour avoir rappeler l'histoire des contributions. Jërëjëf Mais aussi on pourrait préciser qu'il s'agit de contributions financières et qu'il peut y exister des contributions en nature. Et sur ce, la Collectivité Lébou pourrait vraisemblablement offrir l'assiette foncière sur lequel la Grande Mosquée a été construite. Et celle-ci reste inégalable. Il faut aussi le souligner.
Je précise que je suis lébou et que je ne partage aucunement les propos de l'imam. Mais je me permets de répondre par rapport à l'historique des contributions.
Merci encore Baye Mbaye Syll
Mouride yi daño yague ñemé diohé surtou si yonou yalla machalah amna solo lol
Yagg mana féne tamite
@@dieyebathie809 mane mom sama rafet ndiortou si niom takh guisouma lolou si niom
@@dieyebathie809mba sa bire bamel dangako layal
@@dieyebathie809bayi nagn la ak YALLA mi Dara tewoul.
@@dieyebathie809 nanal ndox mim reew mom keneu douniou daxeu dieuf si yonou yalla ndax lolou xol bou yatou mokoy def
Thieuy mourite gno am talibé t fonkou kilifa kenn nangouwoul dioxé Lou opou lissa kilifa dioxé machala
Jërëjëf Baay Niass ,Jërëjëf Serigne Fallou Mbacké, Jërëjëf Serigne Abdoul Aziz Sy Dabakh, ak Khalif yissi déss❤❤
yalna yalla geuneu goudeul sa fane loooooool té yock sa wer té barckel la
Dieredieufe serighn touba diarama mam cheikh ibrahima Fall serighn montakha mbacke yalna kor yalla deffal leep Lou mou beugue barkai yonnen bi Muhammad s a w
Alhamdoulilah dieuradieuf Serigne Touba
Machallah Amna solo diadieuf
Jaajeuf Baaye ❤❤❤❤😂
Thieyy yaa Allah ❤❤❤❤
Dieredeuf baye, yalna Yaala yokou fann gi teh mou andak tawfeh
Wala cheikh Ibrahim niass motakh gnou tabakh grand mosque té mo eupeulé limou diokhé bou sathieu film bi té mo atté kouy jité grand mosque
Mo yaw mi khana deglou video bi yeup? Serigne Fallou joxé million thi tambalibi ba paré continuer di joxer million Chaq année ba jumah bi yegg ngay am loy wax. Cheikh al islam jambar la lole wayé eupa lé wouthi tabi
Dieuredieuf serigne mbaye gueye sylla
Serigne biii t'a moritisé le débat .... faut dire l'histoire et toutes histoires...
MBAYE. GEUYE,, SILLA, , soufeke,, diouma, kouko, tbakhoull,, momoko, kon, senegal, keen,, amount, diouma
MBAYE, GEUYE, dioum, yo si, senegal, yap, kotesasiyon, mokotabkh
Dieurediefer cheikh al islam cheikh Ibrahim niass baye quel générosité ❤❤❤
Dieurédieuf Serigne bi thie léral yi. Ma Shaa Allah !! Que Allah vous bénisse et vous rétribue.
Mashallah YALLAH na YALLAH goudeul sa fane si Barker Seydina Mouhamed PSL ❤❤❤❤❤❤❤
Yow sokhor mola diapp Loutakh doléne wakh deug wala nga Nopi bolele li mourid yi diokhé bakham kholna bou baye bou senegal yako sene genre gui nioko yakk diereuf Sérigne touba
sa bougne diiougé pour torokhal diomaye ak sonko rek yalla torokhal léne . nangoumlene ndogal guir yalla
C'est très intéressant d'éclaircir au peuple. Merci pour les donateurs
Ça reste une mosquée Lebou
Juma Touba niata lébou nio thi def?
Juma tivaone aussi !
Mani l imam a fauté en demandant une visite au président
Mani ki di wakh ni bou niiu done délo thi diokh adiya guir tek ray bi momitam dou jot deureum ndakh diokhéwoulwone 😂😂😂
Sène logique à deux balles yi
Juma touba bane diola mofa djité hana dou négou yallah
Bayilene detail
Baye mbaye gueye sylla historiens bou makk la histoire Sénégal yeep la xam yalla nako fi yalla yagal ta wéreul ko
Manchalah c'est très bien même de clarifier ceci mane tay diang na louma lhamoul wone yalna yalla deugeureul sa takhaway
Nekk mouride nékh na ❤ Doo leen massa am gathié ci Senegal
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😢
LI NGUA. WAKH. NII. GATHIÉ LA. AP. DIOULLITE. AP. DIOULITE. REK LAY. TOUD. BOUL. KHATH. ISLAME
Être mouride ou pas ne veut rien dire être sénégalais est plus important
8:06 waxal waay Murid ❤❤❤❤.
@@MANGASSAthiaroyemer2499loolu ndam la nekk Murid ndam tawfeex la mbekte la loolu bu la naqaree nga muj
Serigne Mbaye Guèye Syll yagg fi lol té anda ak wér. Niou mélni yaw la niou sokhla thi mim réw. Sa xam xam bi nga niou bakhé Yalla na la Yalla gueureum ma cha Allah.
ماشاءالله سرج بي غي صله.جزاك الله خيرا الجزي
Merci beaucoup pour cet eclaircissements!
Pa Lebou bi mofi taxawonn nee keup koufi deh tchi manifestation safara nga dieum!
Imam bobou ab diff moko diapp, mounann sougnouy diouma!
Dieureudieuf serigne mbay gueye sylla 🙏🏿🙏🏿
Amna solo Serigne by trop yalla n'a yalla fay
Makk meutnã bayyi si rèww🥹
Boy bou xamoul, daye móytou grand bou xamm🙏🏿
Thiéy Barhaama Niass 1200000fr CFA ci diamano bobu khaliss deugg lawoone. Maachaallaah. Dieureudieuffé Baye Niass. Dieureudieuffé Baye Niass. Dieureudieuffé Baye Niass. Alhamdou Lillaah halaa koully haal.
Voila une information de taillle qui etre publier partout merci Mr Syll i really appreciate your knowledge and wisdom God bless you
Machallah ❤❤❤❤❤JËREJËFATI Serigne mbaye gueye Sylla
Serigne fallou mo oupele ak mouride yui amoul morom khadim Rassoul
Eupeulé amoul sollo yéné mo am sollo😊
bi niy ame yéné sounou yonou yalla bobou sa mame ak sama mame gané gounou adouna
Ngay wax affaire de yéné do yame lou tolni serigne fallou Ngay toudou affaire de yéné bayi léne soxor way
1million 200mil. Niasse Mame Baye 🥰🥰
Dioumay Sénégal yeup serigne touba lagnouko wara toudé❤
Serigne Touba n'a même pas de maison sur terre les mosquées appartiennent à dieu de faux mourides !!!
Jusqu'à preuve du contraire.
Et on entend la preuve du contraire si vous êtes véridique, cher imam.
Merci d'avoir éclairé notre lanterne.
MACHALLAH, liaatax binde am solo. Dieureudjeuf papa
Diereudieff serigne touba . Normalement ce sont les mourides qui devraient revendiquer la paternité de la mosquée.
Macha'Allah Diaradjeuffati 🙏🏿 Serigne Mbaye Gueye Syll,mbiirmi lëerna naàgne.
Ngi nga fi lim yep wakhouma diokhè niou Rahimoulah Amadou Assane Ndoye mo len eupone teranga foufff limou diokhè rek machallah ay dignitaire yi si dess ak libano syriens yi . Bagnelle gui guene bagnè lebou yi 😢 doyna war tropp et pourtant daniou len yatal diay len ba fap khate . Senegal nio ko bok
Mais mbok lolou yeup souniou mbokK yi leu ,Nioy bayi sen mbok dem si diambour yi di def du n’importe quoi
Merci Serigne Mbay Guey syll pour les détails de cette Mosquée de Dakar cet Imam doit être puni
Serigne Fallou mbacke aki mbokam amougnou morom
Serigne limou diokhé si dioumadji lépou soko bolé 20milions la ❤
Merci bcp sur les éclairecissements. Cet imam me semble arogants. Grand mosquée apartient à la république sénégalais
Machalla alhamdoulilah dieuredieufety cheikhoul Khadim
diadieufaty kou bakhe léeral yi amna solo machalla yàlla na yàlla barkel lah goudal saw fane loole té mou ande ak wér
Partage video bi svp
13:02 pure verité de sergn de Mbaye Gueye syll loudeguou nga wakh yalla nalla yalla yok saw fane .
PARTAGER LA VIDÉO SVP,MAX DE PARTAGE ET DE LIKES ❤❤❤
Surtout ça il faut partagez aime abonnez
Imame de Dakar à changer
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieuf tu as dit ce que les Mourides ont contribué mais il reste la communauté Libanaise, la communauté Leboue en argent et en terres, .... c'est vrai l'imam a mal communiqué, surtout celui qui lui a remis le papier pour faire des prières pour certaines autorités, bref il est mal entouré et cela nous dessert nous communauté Leboue Leboue
Il a dit ce que la communauté sénégalaise avait contribué et non pas la communauté mouride seulement. Si autre communauté avait participé l’article l’aurait mentionné
Thièyy Seugne Fàllou❤❤❤. Amo morom dé!
❤❤jajuf bay Mbaye gueye Sylla ✅✅
Diereudieuf sylla yalna saa borom dollila tawfékh ak taysiir gudeull sa fann amine
Macha leralbi Amna solo yalna yalla fayla
Ohhh ❤MOURID JAYANTÈ,JERREJEF SERIGNE FALLOU MBACKE RTA.DIEUREUJEFF KOU TEDD KI KHADIM RASSOUL❤❤❤
Dieuredieuf baye mbaye sylla thi leeralyi
Machallah baye mbaye syll .Lèerr na na gni
Jërëjëf Pape léral yii amna solo trop 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Dieureudieuf si lerral bi ❤ bouboule wone imam dîna ko wakh lou niaw dafa yabaté
Machalla dieuredieuf serigne touba amoul morome bilahi
Merci Serigni bi
Mais lingay wakh nii si bignoukoy defarare la
Grande mosquée avant 1909 la wone
Djoumah negou Yaala la kene momouco
Mosquée bii gnou beuri liguye nagnou fa comme maneuvre si temps yoyou
Avant 1909 la wone
Sama Mame Thierno Mbaye Sylla moo nekone Imam et Cadi
Gnome Senghor gneuweu gougnou wone
Merci
Donc les lebous n ont rien donné pour la construction de la grande mosquée de Dakar. Chapeau à Serigne Fallou Mbacke et la communauté mouride
LE. TERRAIN. APARTIENT. AU. LÉBOU
Si les lébous ont participé par le terrain
C'est la réalité 😂
IL FAUT DEMANDER A TON PÈRE .LES LEBOUS ONT MÊME PARTICIPE A TON BAPTÊME MON AMI .EST -CE QUE TON PÈRE N'EST PAS LEBOU MÊME.EN EFFET BEAUCOUP DE PERSONNES ETAIENT "BOY" OU "BONNES" DANS LES
MÉNAGES LÉBOU DE DAKAR.SI TU PEUX ME DONNER 2 NOMS DE TES GRANDS PARENTS JE POURRAIS TE DIRE INCHALLA LA RELATION AVEC LA COMMUNAUTÉ LEBOU DE DAKAR
Les terres appartiennent au lebous je suis patriote je suis de pastef je suis lebou niounes lebous danions yatous je suis pa d’accord avec imam samb wayé lebous kéens douka yaap nions yatale nieupa merci 🙏
Jaajëfeti, Serigne Mbaye Guèye Syll toontu júbb na xocc. Ngòor soosu dafa doyadi té soñu séetaanèè dina taal réewi mi ak laméñam wo ñaaw té ñaak worma.
Machallah.yalla nala Yalla Faye thi barkéup boroom darou
Merci beaucoup bay mbaye
Serigne cheikh Ahmed tidiane sy al makhtoum diohéna
Ak niou bari de kéne toudouléne
Machallah Bay Maye geuy Sylla leral Yi Amna solo loll
Maasàllaa am na solo lool jërëjëf.
Alhamdoulilah jërëjëf Sëriñ Tuubaa
Grande mosquée de Yallah non diouma lebou mane mi leboula
Dieureudieuf Serigne mbaye Gueye syll amna solo lool sakh.
Dieureu dieuf serigne Sylla wakh bakhna mais boul kham lougniou laye tonton ❤❤❤❤❤❤
La Grande mosquée de Dakar est construite sur un terrain appartenant aux lébou "Tatay Ndakarou" des cimetières anciens !
La grande mosquée à été inaugurée en 1964 et tu nous parles des donations de hautes personnalités religieuse paru dans un journal en 1960... Qui a donné quoi de 1960 à 1964 hormis le royaume du Maroc l'état du Sénégal, les guides religieux et la mairie de Dakar ? Vous ne saurez le dire... Parparlo rék, fi Sénégal guiss nagnoufi diakay mouride diakay khadir, diakay layéne , diakay ibadou etc etc.... Dioumay Ndakarou mom lébou yi gnokomom koumou nakhari démal sangoo ndokh mou sédd pour wathié sa température !😂
Sénégal mo nekh rekk. Dieuredieuf kilifa gui. Yagg fi lool té wér.
Dieuredieuf dieuredieuf serigne mbaye
❤❤❤❤dieureudieufaty serigne mbaye Gueye syll machallah hamna sololol
Ma Shaa Allah!
Deug rek amm solo!
Diadieuf Mouride
J aime beaucoup sonko et diomaye ils doivent respecter les lebous avant tout ma religion et ma famille
Pourquoi
Salam à vous Serigne Mbaye Gueye j'aimerais que vous me dites
1/la place ou se trouve la grande mosquée de Dakar appartenait à qui avant sa construction ?
Combien il a cotisé (les grands marabout du Sénégal ) pour que l'on nomme le mosquée de tel ou tel a leur nom ,je pense que si c'était le cas aujourd'hui si Mame Maoudo(RTA) Serigne Touba (RTA) etc.... N'auront pas mosquée a leur noms
Toutes les mosquée du monde sont pour Allahou (swt)
Ne change pas la parole de son conteste merci.
Bien dit imam vraiment quand c trop c trop.
Les témoins de l histoire doivent dans tous les domaines éclaircir pour qu'il y ait moins de dérives
dieuredieuf baye guéye léralbi amatina solo machaala
Djadieuf si leeral yii vérité absolue goor gui yalla na la yalla faye ❤❤❤
Machallah lerna dh❤
Mbaye Guèye sylla beuri nga loye tontou .
Grazie mille serigne Touba ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎
Mbaye syll tu mens la grande mosquée de dakar est don de maroc
80 pour cent yi ap talibé cheikh dip seuteum moko diokhé Hassan 2
Waw gor serigne mbaye takh nga koukhamoul khaam.yalnala bourbi saam aarla.
Grand mosquée de Dakar xalisou royaume du Maroc Serigne fallou ak khalifa général you Bari séne khalis dame nathia
Bilay
Comme grande mosquée Bou Touba bi rek ...khalissou nieup demnaniou thi té térewoul mouy dioumay Touba ...arrêté léne
Khalissou niépp comme niane ?
Ya meuna kathi dioumay Touba loudoul khalissou wakeur Serigne Touba demouthi
Dieuredieuf serigne MBAYE GUEYE SYLL leerrna nandje Akassa
Archives yaa ngui fi deh
Guiss naa ko
J'aurais bien aimé que vous me dites combien la collectif lébou a cotisé et combien le roi du Maroc a cotisé gras a Mame Abdou Aziz Sy .
Dieureudieuf fékké dimbeu feékké téye amna solo mô waral.lêral gui,yalna.nga gueuna gouddou fane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Imam grande mosquée khaliss moko interessé. Changélen ko. Khamoul touss
Machala serigne yi yag nagnoo def té yalla takh. Niass
Les lebous doivent amener cet imam en formation ou le remplacer
Vraiment il es fou😢
YAL NAGNU KA SUNU BOROOM REMPLACER AK KU MAT IMAN. 🤲 ALLAHUMMA AMIIIN 🤲
Remplacè
La collectivité l’éboue a donné une Somme d argent et un terrain de 3 ha
je suis lebou mais quand il parle j'ai honte
Weranté rek Ta ken dou weranté si lou am ndiarigne
Dieureudieufati Borom Touba
Thiëy Wakeur Ku Téde Ki
Nio Téde Nio Bakh Nio Tabé