Dieureudieuf baye mbaye yalla nala serigne touba doli weer ak yok sa kham kham ak bayila sa khele machallah gua sakh si dignou begueule si ay mbirou kou teed ki khadimou rassoul amine
Un homme doit dire la vérité. Le Grand Serigne Bamba n a jamais ordonné à qui que ce soit de le venger ou de parler en son nom. Serigne Touba a dit que DIEU est son rampart. Ce que ce vieux singe raconte est faux et une pure invention. Je suis près à débattre avec lui. Il ment et doit savoir que nous les descendants nous sommes alliés aux descendants de Serigne Touba ce Grand Homme n a jamais fait du mal à qui que ce soit. On ne peut pas admettre de tels mensonges Serigne Touba n a jamais voulu du mal à qui que ce soit à plus forte raison ses ennemis car Serigne Touba a dit que mes ennemis je pardonne car DIEU est pardon. Mais celui qui parle est un nafhekhs.rien qu à voir sa tête c est celle d un homme d enfer La plus part des descendants de celui qu il fixe au pilori sont des talibés de Serigne Touba et son enterré à Touba. Mais DIEU est justice et Serigne Touba est un serviteur et ami de DIEU et de son Prophète Mohammed Rhassoul (psl):
Alhamdoulilah ma sha Allah dieureudieufati serigne Touba Xadimour Rassoul yalna niou Yallah xiir si beugue ko ak ligueyal ko mom ku Tedd ki ba aldianatoul firdaws barkep mbautoum xassidas yi
Dieureudieufe bay mbay mo noo wona gnak thi yoon bi deh bilahi waye nak dou hasard Mame thierno moo lay kham lo di la ligueey lo yague fi lool te and ak weurr❤❤
La contrepartie de celui qui se compare à moi et ne s'en repent pas est une condamnation sans appel inscrite dans la source fes livres. CHEIKH AHMADOU BAMBA dixit.
Ñu mel ni yaw ak Gana Messeré ak Ablaye Diop Bichri, fi gneen taxaw foofula. Doo leen seetaan kénn di gàkkal yoon wi ci lu dégguwul fénn;ak di ci bëgg a andi ay yëngu-yëngu. Te ndokk sax ndax yoonu murid ciy yëngu-yëngu lay yokkoo ba ñépp yëgko.
Dieredief amna solo lerna. Avec Serigne Mbaye Gueye on apprend toujours de nouvelles choses. Je ne savais pas que Ma Abdou Lo et Doudou Mambaye sont des frères utérins.
Il y a sans doute parmi ceux qui descendent de ces deux frères des hommes et des femmes qui sont aujourd'hui de vrais disciples de Khadimou Rassoul.Permettez moi juste une pensée pour eux.Il y a des faits dans l histoire qu'il ne faut point agiter ,par miséricorde,pour éviter de faire souffrir inutilement des innocents.
c" est le passe qui nous fait apprendre aujourd hui et demain mon cher N'oublie jamais " leer dina fegn ci biir lendem" on apprendre tjour a cause de l'istoire il a tres bien fait de le raconter pour l'avenir jerejefeti serigne touba cordialement
Il n'est pas question de faire à nouveau mal les coupables ou ses descendants mais faire connaître les mouritt l'histoire du Grand Cheikh. Car cela pourrait constituer une leçon pour les hommes politiques du Sénégal
Quelle rapport avec sa . Macky vous hante Je suis sur que vous faites de la lignée des traîtres qui ont voulu sacrifier serigne Touba des salle traîtres que vous êtes
Celui qui s'oppose à Serigne TOUBA s'oppose à DIEU et celui qui s'oppose au bon DIEU ira sans doute à l'enfer donc celui qui s'oppose à SERIGNE TOUBA ira aussi en enfer Wal honzoubilahi
Machallah yalnala yallah faye ak equipe binga andal yépe. J'apprécie beaucoup le travail d'éveil que vous abattez surtout en ce qui concerne les falsifications des recits qui sont souvent faites par nos sois disant conferenciers. Pour mon humble contribution, je vous suggère de faire des Playlists pour les vidéos d'une même emission par exemple. Comme la chaine grandit très vite en contenu, on se perd facilement et ça devient parfois difficile de trouver la suite d'une émission. Aussi s'il etait possible de diminier un peu le volume de la musique de fond pour que l'on puisse mieux bous entendre. Yalna gnuéne dadié ak ngueureumeul serigne touba.
Maasàllaa waa séen #Xam #Rée tv yéen ngi ligéey bu am solo bég na ci yéen lool Mbokki taalubee maa sàkku ci yéen ngéen bëggi séen wii di👉 #Jàngwolo ngir ngéen mënn bind Wolof yi
Serigne Touba beugg koo té diko ligueyeul ak dikoo Santeu rek laniou wara deff 🙏🙏 kouko defoul dinga sone fii sone Alaxira parck Moy Khadim Rassoul jajef
Ndaysaan brom baax nga
Bilahi yaw
Bamba dou morom kén dou borom touba dieureudieufe cheikh ahmadou bamba khadim rassoul diarama mame cheikh ibrahima fall lampo baboul mouridina ba Aldiana rek serigne touba rek Képp ❤👈
Gnaar ñy nio katte seen nday
Doudou ak ma abdou lo
Abdou lakhad Diénge ziyar nala
Frére ľhitoir renconte le fai est le passée des ďhommes. Serigne touba borome yeuremadé lah.
Et toi tu fais quoi de ta mère ou grand mère
Espèce d idiot
Machallah amna solo sunu Baye yagal weral
Serigne Mountakha Bachir Yalla na fi yaag lool té wér
Dieurëdieuf Serigne Touba MachaAllah yaggë fii LOL té wérr Syll
Seugn bi sayo defer video ngeu indi Lou kene xamoul wone 👏🏿👏🏿 très très pertinent
Daniouye sonou reik serigne touba sakaname
Machallah Sylla mais dagua wara binde ay livres si histoire serigne touba
Machallah aka video yi yeupa amna solo
Bind na livre
Dans le monde actuel binde livre ac def ay video dougalko si internet bi gno yam rek ndakh lep dafiy dééss
Migui binde téré
Dieureudieuf baye mbaye yalla nala serigne touba doli weer ak yok sa kham kham ak bayila sa khele machallah gua sakh si dignou begueule si ay mbirou kou teed ki khadimou rassoul amine
Machalah Segn Mbaye yalna Yalla yokou xamxam bi ta yagal lafi
Dieureu dieuff baye mbaye sylla yalla na yalla goudëll sa fane ba légui noni serigne touba yangui sénégal nak
Billahi bofi yagoul dou bakh té geum nani dinga doundou ba doyal mouride yépp amél nanoula diadieuf merci pére gaayi linou beug dou am déh té manoul nékk
@@terangatv5395 Wallaahi du am jërëjëf
Un homme doit dire la vérité. Le Grand Serigne Bamba n a jamais ordonné à qui que ce soit de le venger ou de parler en son nom. Serigne Touba a dit que DIEU est son rampart. Ce que ce vieux singe raconte est faux et une pure invention. Je suis près à débattre avec lui. Il ment et doit savoir que nous les descendants nous sommes alliés aux descendants de Serigne Touba ce Grand Homme n a jamais fait du mal à qui que ce soit. On ne peut pas admettre de tels mensonges Serigne Touba n a jamais voulu du mal à qui que ce soit à plus forte raison ses ennemis car Serigne Touba a dit que mes ennemis je pardonne car DIEU est pardon. Mais celui qui parle est un nafhekhs.rien qu à voir sa tête c est celle d un homme d enfer
La plus part des descendants de celui qu il fixe au pilori sont des talibés de Serigne Touba et son enterré à Touba. Mais DIEU est justice et Serigne Touba est un serviteur et ami de DIEU et de son Prophète Mohammed Rhassoul (psl):
Kouy yéné rek yénél lou bakh serigne touba
Machalah amna solo lole yalla na yalla yok say fane ci barké serigne bi
Serigne
Mountakha mbake yalnafi yagu ta wer yaw tamit yalna yalla goudal sa fann
Doudou ma mbaye aka bone ta saay saay. Dieuredieuf serigne mbaye gueye Syll. Yalna nga fi yague lol . Lerna nagni.
Alhamdoulilah ma sha Allah dieureudieufati serigne Touba Xadimour Rassoul yalna niou Yallah xiir si beugue ko ak ligueyal ko mom ku Tedd ki ba aldianatoul firdaws barkep mbautoum xassidas yi
Aamiine.
Machallah yalla nga goudou fan cii barkem borom touba
Akassa baye mbay geye sila yaguefi loll ta ande ak wer barkep s.touba dolaye mame cheikh ibrahima fall amiiiin
Merci xam sam rew TV.yalnaléne borome bi are barké Borome Touba sounou yakar
Dieureudieufe bay mbay mo noo wona gnak thi yoon bi deh bilahi waye nak dou hasard Mame thierno moo lay kham lo di la ligueey lo yague fi lool te and ak weurr❤❤
Machaalah dieuredieuf li warr nako diangualé ci ecole yi univresité Senegal dieuredieuf serigneTouba 😭
Dieureudieuf Serigne Mbaye Gueye Sylle Yalla Nga Fi Yague Té were Bi Barakatoul khadimou Rassoul . Amine
Mashahala serigne mbaye gueye sylla yaguefi lool te weer barcke kou dedki
Merci beaucoup papa sylla yalla n'a yalla faye la ak sa yakar bamba
Mourid bou bakh
La contrepartie de celui qui se compare à moi et ne s'en repent pas est une condamnation sans appel inscrite dans la source fes livres. CHEIKH AHMADOU BAMBA dixit.
Ñu mel ni yaw ak Gana Messeré ak Ablaye Diop Bichri, fi gneen taxaw foofula. Doo leen seetaan kénn di gàkkal yoon wi ci lu dégguwul fénn;ak di ci bëgg a andi ay yëngu-yëngu. Te ndokk sax ndax yoonu murid ciy yëngu-yëngu lay yokkoo ba ñépp yëgko.
Musique de fond bi ❤️ Thiey sama pa yi wa Beyti Mahboub ❤️❤️❤️
Macha alla s mbaye g Sylla diangat bi amatina solo lérna lol tégouna thi kham kham yagak wér rék barkéb borom daroul mouhty
Ceey Allahou akbar yalla nanou yalla fayale serigne toubaa
Anaaaaa guirou Abdou lo AK doudou ma mbaye sénouk ndiabott sénii Mame lornalénn
Wayé dano rakh si biir nitt gñi waronn nann lénn khamé nak
Dieredief amna solo lerna.
Avec Serigne Mbaye Gueye on apprend toujours de nouvelles choses. Je ne savais pas que Ma Abdou Lo et Doudou Mambaye sont des frères utérins.
Baye Mbaye yalna yalla goudeul faneyi té may la ak wer!!!
Dieureudieuf Serigne mbaye Gueye syll. Amna solo lol.
Machalla dieuredieufety serigne touba diarama mame seex ibrahima fall
Daako méré. w.one wayé ya takhe ba khame né dafa diomone rék bakhanne Diop yalla nako yalla yereme
wa doudou mambaye ak abdou lo seni famille gouniou dh
Jerejef j'apprécie beaucoup votre site
❤❤❤❤ santé rek seringe Touba
Mach Allah xam sam réw tv yalla na yalla yokou lépp
Kou khamoul rèk moy nono waliyou
Machala Amatina soolo dieureudieufety baye syll
Dieuredieuf serigne touba ya gore ya mougne ya amdiom ya amfith ya khoty baax
Dieureudieufi serigne touba ❤❤❤❤❤
Machallah histoire bi lerna, toubab bou nioul mo yeuss si Rew
Il y a sans doute parmi ceux qui descendent de ces deux frères des hommes et des femmes qui sont aujourd'hui de vrais disciples de Khadimou Rassoul.Permettez moi juste une pensée pour eux.Il y a des faits dans l histoire qu'il ne faut point agiter ,par miséricorde,pour éviter de faire souffrir inutilement des innocents.
c" est le passe qui nous fait apprendre aujourd hui et demain mon cher
N'oublie jamais " leer dina fegn ci biir lendem"
on apprendre tjour a cause de l'istoire il a tres bien fait de le raconter pour l'avenir
jerejefeti serigne touba
cordialement
C'est votre point de vue Je le respecte
Il n'est pas question de faire à nouveau mal les coupables ou ses descendants mais faire connaître les mouritt l'histoire du Grand Cheikh. Car cela pourrait constituer une leçon pour les hommes politiques du Sénégal
@@dangcheikh1054 C'est un débat d idées .Chacun est libre de donner son opinion.
Iigueyeul serigne touba rek mo woor demna bâ khamni say seut seutate lay tambali dila Faye bâ aldjana ...dieuredieufety borom touba khadimou rasssoul
hakassa جزاك الله خيرا
Kou nonoo nitou yalla saga doff rec nakh yalla bourr la dou noone
Sëriñ bi Sylla depuis bim la decouvriree ci émission Walf ba léegi maa ngi lay suivre. Dila ñaanal Yàlla wéral la, dëgëral la
Soudoul won demam gui wolof don nasaran te bilahi niep dem niran dieuredieufte serigne touba khadimou rassoul
C'est pas ça vous comprenez rien
kou bagn serigne touba si torokh rek ngay moujou
Bilahi li dangua ko yeekh déf yalla nala yalla fay si Barcky seringe touba
Machallah amna solo lole té leer.
Yalna yalla goudal sa fane té mayla weur
Thiey alhamdu lillah Yàlla nañu sax si bëgg sëriñ Tuubaa té diko liggéeyal
dieureu dieuf serigne touba khadimou rasoul
Morale de l'histoire : les faits remontent à 1899. Nous sommes en 2020. Dieuf diou gnaw dou fay ba mouk. Nétali bou gnaw dou faye.
Dieurdieufé Serigne Touba
Machallah serigne bi yalla na yalla goudeul say fane
Alkhamdoulillahi Rabbil Hanlamina Allahouma Salli Hanla Seydina Moukhamad Wa Sallim Dieureudieufeuti Borom Touba Amoul Morom Abadane Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall Baboul Mouridina
Serign Mbaye geuye Sylla yalna fanwii yôkk looll te andakouk wérr lougni Kham thi yonn Wii rkkk yaw la
L’homme noir est l’ennemi de l’homme noir. Douniou tayi di bagne Serignebi
Nonou borom Touba mom torokh rék adouna ak alakhira
DIEUREDIEUFETY Sylla
Doudou ma mbaye yaw ak sa raak doy ngén waar déh té sokhoroon toppa toubab bi molénndi diay tchiim.
Ma-jambal jaañ, de war naa dég lu lii
Macky Sall le soumi francais doit écouter cette histoire
Dieureudieuf Bay mbay, kou tédd ki kouko noonu yalla toroxal la
Machallah s mbaye geuye sylla
Serigne touba sakaname reik, diadieuf
Quelle rapport avec sa . Macky vous hante
Je suis sur que vous faites de la lignée des traîtres qui ont voulu sacrifier serigne Touba des salle traîtres que vous êtes
Celui qui s'oppose à Serigne TOUBA s'oppose à DIEU et celui qui s'oppose au bon DIEU ira sans doute à l'enfer donc celui qui s'oppose à SERIGNE TOUBA ira aussi en enfer
Wal honzoubilahi
DIEUREUDIEUF BAYE MBAYE G SYLLA YALLA NA YALLA GOUDALE SA FANE
Beugg nan ngua bindall ñu livre tamitt 🤍
Machallah histoire bi lérna trop
Djadjeufety serigne Mbaye Gueye Sylla liguey bi rafett na. Djeureudjeufety Cheikh Ahmadou Kara Mbacké Nooreyni
Serigne Mbaye gueye syll lep louma xam sii MAME BOROM DAROUL MOUHTY ya tax ma xamko walahi heug nala guiss
Cheikh Diagne inchallah lolou dina am
Machallah yalnala yallah faye ak equipe binga andal yépe. J'apprécie beaucoup le travail d'éveil que vous abattez surtout en ce qui concerne les falsifications des recits qui sont souvent faites par nos sois disant conferenciers. Pour mon humble contribution, je vous suggère de faire des Playlists pour les vidéos d'une même emission par exemple. Comme la chaine grandit très vite en contenu, on se perd facilement et ça devient parfois difficile de trouver la suite d'une émission. Aussi s'il etait possible de diminier un peu le volume de la musique de fond pour que l'on puisse mieux bous entendre. Yalna gnuéne dadié ak ngueureumeul serigne touba.
Dieureuf lii moy histoire bou leer. Yagafi lool té weer
Aminnne
Dieuredieuf serigne touba
Machalla Serigne Mbaye syll mèrci
Sant nagne la Serigne Mbaye gueye
Machala sangue bi ame na solo
Akassa Dieuredieuf xam xam bi wér na. Serigne Touba amoul morom
Mashallah li mom amna solo niogui siy tewlou bubah
yalna nangafi yzgg té wér amine
dieuredieufe borom touba
yala nga fi yague té wér té yalla soutoural lah ba fawou
Maasàllaa waa séen #Xam #Rée tv yéen ngi ligéey bu am solo bég na ci yéen lool
Mbokki taalubee maa sàkku ci yéen ngéen bëggi séen wii di👉 #Jàngwolo ngir ngéen mënn bind Wolof yi
Maa ngi tuub ci mbind mi dama cee juum ci séen wi nii 👉 la #Wax-wolofak xam le
Akassa amna solo lol
Santati s touba rek
Machallah sylla
Dieurdief yalla ngafi yag lolo tewer
Dieureudieuf Cheikhoul Khadim
dieureudieuf si leral bi
Deredefe wa merci ndam réke
Kene dou borom touba amol morom
Thiéy amna solo trop macha alah
Dieureudieufé s touba
Masha'allah amna solo
Macha ALLAH amena solo
C'est clair on explique pas l'histoire en tâtonnant 🙏👍
Kou am double nationalité waro tak bene dombo tank tji rewmi. Diadieuf sa liguey rafetna Syll Yallah goudal sa fan Merci
Diadif serigne mbaya guaye sila
Machallah amna solou loul
Amna soolo khana Abdou lo ak doudou ma mbay cissé lo sene setlleu
Waw