je suis un pure musulman issue de la communauté mouride mais Madiama Fall est un érudit vraiment que j'ecoute fréquemment nitt nak day dioume lolou xasse la
Nul ne possède la véritable sagesse. Qui peut prétendre détenir la vérité entre vous deux, puisque ni l'un ni l'autre n'étiez présent en ce temps-là? Conservons donc notre raison et gardons-nous de juger hâtivement.
D ou l'importance de ne pas défendre aucune religion étrangère dont aucun de mes ancêtres noirs était présent de la véracité de ces croyances. L esclavage européen a dure 400 ans et l'esclavage arabo musulman a dure 1300 ans de barbarie sur nos ancêtres.
Wakhoul beugoul kham kham d. Il le corrige juste. Wakhul daf am intérêt aussi pour fénal Lat Dior. Il a déformé l’histoire et on l’a corrigé c’est tout.
@@doucourelassana3663 non je n’exagère pas j’ai mes raisons avant de dire que j’exagère écoute d’abord toutes les vidéos que professeur Madiama a fait et vous verrez qu’il est différent des autres tei yalla dako may
Une émission spéciale à la RTS confiée à Serigne Mbaye Gueye Syll sera d'un très grand apport pour le pays. Le nouveau DG de la RTS est invité à y réfléchir.
Pour le pays ou pour la communauté wolof? Ki histoire wolof yi ak mourides yi lafiy dougoll, on l'entend pas parlé de l'histoire de la Casamance, foutankés, des sérères Soninkés etc..
Mais pour chaque ethnies il faut inviter quelqu'un qui la maîtrise. Et pourtant même il parle de thierno souleymane baal sui n'était pas wolof.@@Ordinaire95
Merci tonton. Ce mec a écouté un historien de la tradition orale qu'on appelle Mbeguéré. Je crois qu'il faut inviter ce Mbeguéré là pour y voir plus clair.
Il s'est trompé de bonne fois il y'a plusieurs versions dans la tradition orale mais les recoupements et les archives les choses sont bcp plus claire même s'il y'a encore des zones d'ombre le métier d'historien ne rime pas avec passion
Les histoires sont des paroles nées et qui ne meurent jamais ,mais des paroles qui tombent souvent malades,et cette maladie se manifeste par des controverses..dont le médicament n'est que d'écouter sans juger👌
C est mbaye gueye.syll qui raconte la vraie histoire de.lat dior :parce les 95% de ce.qu il dit est archive par les francais ou par la tradizione orale (les griots qui ont vecu certe epoque
Les paroles sont éphémères et sont souvent transformées sur son trajet de transmission mais les écritures sont éternels en plus l'écriture est la mère des preuves. Tous les deux est ce que lat Dior et bour sine écrivaient leurs histoires comme ce cheikh ahmadou bamba a fait. Il a tout dit sur ses khassaide.
Objectivité moy Sounou problème le vieux donne des dates avec exactitude et des sources écrites il a déjà publié des œuvres scientifiques sur l’histoire des royaumes avec des archives à l’appui
Merci beaucoup Serigne Mbaye Sylle vous avez de la capacité intellectuelle et un intérêt à agir. Une bonne information doit connaître de source fiable. Mais nioulay talal micro lou nieuw sa xel gua wakh c'est du n'importe quoi 😭😭😭
Waxo Ba nitt ki guéne wax, guay Dora guénn di wédd, lolou moy Sénégal😂😂 En tout cas oustaz fall laniouy déglou moniouy wax waa asamane di niou wax waa souff😂❤
@@khalil2543 si tu te bases sur un nom de famille pour dire que tel personne est de tel pays même mbaye sylla est un guinéen car la plus grande concentration de Sylla au monde se trouve en Guinée Conakry
@@papacisse7155 je crois à ce monsieur en ce qui concerne qui concerne l’histoire des modernités sénégalaises, d’autant plus qu’il est spécialisé en ce domaine alors que professeur Madiama que j’aime bien est dans toutes les sauces ce qui est d’ailleurs presque impossible chez l’humain, on est pas censé savoir tout.
@@labsolusaliou7254ah bon il est spécialisé dans ce domaine. Il a quel diplôme ? Quels sont ses sources ? Il est facile d’être la à parler sans source ni rien. Wadji syll kay se croit être le détenteur de l’histoire authentique du Sénégal surtout wolof et mouride alors que nenni
Merci mr sylla, ce gas erreur yi mouy déf mo beurry , déglou na béne récit boumou déff si egypte antique, mais j'étais abasourdi , si ay wakh you tégouwoul féne 😂😂😂 .
Qui a raison, qui a tort ! je ne sais pas mais en ce qui concerne l'histoire : c'est des sources et les sources peuvent différer c'est tout simplement ça
@@piskogueye2638 bah ouiey parce que gnom sén ay époque ken fékéwoukoo alors kouné ak fii nga roté xam xam en matière d'histoire mom personnes n'a raison et personnes n'a aussi tort soyons juste humble
En 1886 Thilmakha Mbackol n existait plus.il à été fondé vers 1700 par Sakhewar Fatma mais il était tombé en ruine et a été refonde par Serigne Abdou Abass Diop en 1896 dans son emplacement actuel sur recommandation de Serigne Touba
serigne mbaye gueye syll histoire bo. Fékéwoul té source gni gua am day lako netalil mana wer mana bagna wer parce que gnoune sounouye histoire amoul démonstration scientifique motakh liguane moy guéne bolo def seytou mogueune guene ni wérenté parce que ay borome khamkham guen gnen gnar gnepp
Père ioe sa version nga wakh mom mou wakh version wam donc li eup solo moy sou amone firndé biniou bindone loolou sa jamono joojou nioune seutou lat Dior yi dîna niou geuna kham histoire bi donc migui melni ay Hadith you beuri yi niou wakhal yonnenté bi صلى الله عليه وسلم am you beuri you si leerul dieureudieuf 🙏🏽
En vérité, le Pr Madiama FALL n'a fait que reprendre textuellement le récit de l'épopée de Lat Dior de la vidéo sur le lien que je viens de partager ci-dessus...
je suis un pure musulman issue de la communauté mouride mais Madiama Fall est un érudit vraiment que j'ecoute fréquemment nitt nak day dioume lolou xasse la
Amana madiama fall da dioum wayé pa bi wédina wayé tégule dra sunu loxoo jusqu'à preuve contraire madiama fall la geum si histoire bi
Diareudieuf pére wayé magui lay sedal ni Oustaz Madiama Fall kou bakh té humble surement dinako aprécié.
Nul ne possède la véritable sagesse. Qui peut prétendre détenir la vérité entre vous deux, puisque ni l'un ni l'autre n'étiez présent en ce temps-là? Conservons donc notre raison et gardons-nous de juger hâtivement.
True
D ou l'importance de ne pas défendre aucune religion étrangère dont aucun de mes ancêtres noirs était présent de la véracité de ces croyances. L esclavage européen a dure 400 ans et l'esclavage arabo musulman a dure 1300 ans de barbarie sur nos ancêtres.
Merci baye mbaye Sylla peut-être version yii nio bocoul mé madiama fall kou beug xam xam la té amoul bén intérêt pour fénal Lat Dior
Yaw li nėk si xė Lou lat dior xamoko bayil madiama mola appe xam xam fof
@@madinatv2214pourtant yena bok lingene di wakh d
Madiama day weur di doul rek.
Wakhoul beugoul kham kham d. Il le corrige juste. Wakhul daf am intérêt aussi pour fénal Lat Dior. Il a déformé l’histoire et on l’a corrigé c’est tout.
Mais mona dioum
J'ai jamais entendu madiama dans ces histoires mais il un grand scientifique religieux
Kouné ak sah guem guem ms mane mome professeur madiama fall lah gueme vraiment
En tout cas Madiama Fall amena xam xam trop ma sha Allah je n’ai jamais été ébloui par une personne mais lui vraiment yalla maynako
JE NE SAIS PAS VOUS EXAGEREZ HEIN?
@@doucourelassana3663 non je n’exagère pas j’ai mes raisons avant de dire que j’exagère écoute d’abord toutes les vidéos que professeur Madiama a fait et vous verrez qu’il est différent des autres tei yalla dako may
@@doucourelassana3663 pas du tous écrit kawn malikia il faut le voir pour le croire 🤞 .
De grâce mettez ces histoires dans livres enseignez à nos enfants
Vraiment Vraiment
Baye mbaye Syll amal diamou
fier d'être wolof et merci beaucoup vous devez écrire un livre
Histoire dh toujours nila faw mou am coté younou doul d’accord
Le rôle des grandes personnes jubanti Machallah dinasi bayi xell
Une émission spéciale à la RTS confiée à Serigne Mbaye Gueye Syll sera d'un très grand apport pour le pays. Le nouveau DG de la RTS est invité à y réfléchir.
Pour le pays ou pour la communauté wolof? Ki histoire wolof yi ak mourides yi lafiy dougoll, on l'entend pas parlé de l'histoire de la Casamance, foutankés, des sérères Soninkés etc..
Cheikh Thioune je suis d'accord avec toi ❤❤❤❤
il nous le faut à la rts
Mais pour chaque ethnies il faut inviter quelqu'un qui la maîtrise. Et pourtant même il parle de thierno souleymane baal sui n'était pas wolof.@@Ordinaire95
@@diawi2588 oui mais ils y'a des historiens plus généralistes, c'est eux qu'il nous faut pour intervenir dans notre télévision nationale,
Merci tonton. Ce mec a écouté un historien de la tradition orale qu'on appelle Mbeguéré. Je crois qu'il faut inviter ce Mbeguéré là pour y voir plus clair.
Il s'est trompé de bonne fois il y'a plusieurs versions dans la tradition orale mais les recoupements et les archives les choses sont bcp plus claire même s'il y'a encore des zones d'ombre le métier d'historien ne rime pas avec passion
Machaallah professeur madiama fall
Les histoires sont des paroles nées et qui ne meurent jamais ,mais des paroles qui tombent souvent malades,et cette maladie se manifeste par des controverses..dont le médicament n'est que d'écouter sans juger👌
Merci doyen ! Non à la falsification de l'histoire. Sourcer, référencer sont la force de l'Historien
Madiama Fall descendant direct de Dethie fa Ndiogou
C est mbaye gueye.syll qui raconte la vraie histoire de.lat dior :parce les 95% de ce.qu il dit est archive par les francais ou par la tradizione orale (les griots qui ont vecu certe epoque
Madiama fall diambaar deug la naw naako lol
Il ne faut pas se fier aux récits oraux car il y aura tjrs de l’exagération
Je préfère les recits oraux que les archives des blancs qui sont remplies de contradictions de racisme et de mépris @@Mhd3107
La tradition orale est constituée de l'ensemble de ses versions connues.
Les paroles sont éphémères et sont souvent transformées sur son trajet de transmission mais les écritures sont éternels en plus l'écriture est la mère des preuves. Tous les deux est ce que lat Dior et bour sine écrivaient leurs histoires comme ce cheikh ahmadou bamba a fait. Il a tout dit sur ses khassaide.
Mbaye sylla eska liguaye wakhe nonoulademe fekewoo diamano lat dior .
Il raconte n'importe quoi.. Chacun raconte ce qui l'arrange.. 😂😂😂
Madiama momit ndax da fekké
Lat Dior héros national
Lay Dior louko déf héro national
Serigne professeur Madiama Fall kou beuri xam xam la té séll histoire amna diverses versions ndax ken fékéwouko
Kou bax nitt bou doule dioum amoule
L'histoire de Lat Dior est une fausse histoire puisqu'il raconte des versions différentes😮😮
Ioe yay mbam @@amarmoussa8648
Machaallah professeur madiama fall kén meunuoula diam
Objectivité moy Sounou problème le vieux donne des dates avec exactitude et des sources écrites il a déjà publié des œuvres scientifiques sur l’histoire des royaumes avec des archives à l’appui
Merci Papa 👂👂oui ses paroles ya contradictoires
Merci mbaye gueye syll pour les éclaircissements moi même j'avais apporté des clarifications par ses propos infondées
mn uotaz lek lay topu madiama
Merci beaucoup Serigne Mbaye Sylle vous avez de la capacité intellectuelle et un intérêt à agir. Une bonne information doit connaître de source fiable. Mais nioulay talal micro lou nieuw sa xel gua wakh c'est du n'importe quoi 😭😭😭
Kadior ak baol ❤
Kajoor ak Bawol 1549 ba ci jamonoy Latjoor lu bari ci Dammeel dañu koy boole ak teeñ gi 😂
Machalla serigne Mbaye gueye Sylla
Père gemoumala madiama fall la geum 👍🏽
😅😅😅😅
Thioohh😂😂😂😂😭
Madiama dou sa morom...demal teudi...
😂😂😂😂😂😂
Waaye njuumte day am dafa juum
Lhistoire se deforme de generation en generation. Qui nous dit que tu détiens la vérité yaw Baye Mbaye sylla .
Merci beaucoup
BIEN DIT
Mbéguéré mo nétali limou wakh mbéguéré dadone théâtre rék
yaw wakhe nga leppo nounou rek la deme
Kouy mbeguere
Merci 😂
Lolou la beugon leeral nii li mou wax nii dara wouté wousi ak li mbegueré wax
Sa waay boulma ray waay. Mouy mbeguere?
Diaradieuf professeur madiama fall
Jaajeuf Bay Mbay Gueye Silly
Merci père M’baye ❤
Moi je propose un débat entre Madiama fall et Mbaye Gueye Sylla
nitt kou bakh dou diaxase
Niveau yi bokoule madiama dou moromame
Dieureudieuf serigne mbaye gueye sylla
madiama fall mofi néka payi gesowno dara haléyi nofi neka and modou fall ❤🙏🏽
deet way kou bax! Serigne Mbaye Syll danaka doundam si gestou histoire lako diekhal.
DIEUREUDIEUF BAYE MBAYE GUEYE SYLL BANGEN WARE WAKH DAFA YAGG DEH,FACONS YI NIONGUI BEUGA RAY NIT GNI AK DOAXASSE HISTOIROU SENEGAL,MERCI...🎉❤😊
Le malheur de l'Afrique, c'est quon s'attarde sur la place de la virgule dans la phrase.
Waaji jambaar la wayè ay waxam dafa barri fawwu mou juum
Voilà tas compris
@@Mouridelaasonkoolaa111 waji xamole dr wakhi mbegare rek ladone netaliwate tembegare dadone thiatre rek
😂😂😂😂
😂😂😂
@@alassanedieng259Waxal dé😂😂😂
Sama baye Meune nga ratifié mais Diaroul afficher photome diaroul afficher toureum li histoire la rék kouné meune naché dioum
Vrema
L'histoire ne doit pas être inventée
Jërëjëf Baay Mbay ❤ gëna yag gëna Wéer aminee yaw Xam Xam rek gay Wax Walahi
Histoire la kounek ak ligua diangue dara worou niou ni liguay wakh moy deugg ms le professeur madiama fall n'invente jamais rien 💖
Si vous tapez Mbeguéré sur youtube, il dit presque la même chose.
Madiama fall lagnou geume🎉🎉🎉🎉
Waxo Ba nitt ki guéne wax, guay Dora guénn di wédd, lolou moy Sénégal😂😂
En tout cas oustaz fall laniouy déglou moniouy wax waa asamane di niou wax waa souff😂❤
ki yagna wax dh yako khamoul wone rk😂 en plus nitt dafay dioum
Ki Bamiy wax Madiama khewoul
Mbaye G sylla maîtrisé wo lou bari ci histoire. Lou bari da ngaye niodi diémélé ci Lat Dior .Di dégglou lou bari ngni âme yénène xalaat.
deloul pitah te gua bayi sunu histoire
@@khalil2543 si tu te bases sur un nom de famille pour dire que tel personne est de tel pays même mbaye sylla est un guinéen car la plus grande concentration de Sylla au monde se trouve en Guinée Conakry
Pour li Bay mbay wakh moom la livre you bari wakh (SABATIER:LE SÉNÉGAL SA CONQUÊTE......LES DAMELS DU CAYOR)
Yaw ap ndéring nga démal wakh si sa histoire deuk té bayi souniou histoire deuk
40 ans de recherche
Jerejeuf Serigne mbay Gueye silla❤👍🙏🙏🙏🙏🙏👍🙏
Ndeysaan Ustaas Majama Faal ku baax lë, njumte du wees . Jërëjëf Baay Mbay Gëy Sill.
Qui nous dit aussi que ce monsieur dit la vérité
@@papacisse7155 sénégalais mo naif
@@papacisse7155 je crois à ce monsieur en ce qui concerne qui concerne l’histoire des modernités sénégalaises, d’autant plus qu’il est spécialisé en ce domaine alors que professeur Madiama que j’aime bien est dans toutes les sauces ce qui est d’ailleurs presque impossible chez l’humain, on est pas censé savoir tout.
@@labsolusaliou7254ah bon il est spécialisé dans ce domaine. Il a quel diplôme ? Quels sont ses sources ? Il est facile d’être la à parler sans source ni rien. Wadji syll kay se croit être le détenteur de l’histoire authentique du Sénégal surtout wolof et mouride alors que nenni
@@labsolusaliou7254 tu connais Aristote ?
Man yaama doy ci mbuur.
Jubantu mom yakhou Dara ci istouwar
Merci Baye Mbaye nakh waadji loumouy wakh Lou beuri c’est pas fondé mais puisque Sénégal mome bo beureh wakh rekk yaa ame kham kham
Beurigo bou fesseh….
Kii dafa deglou ben kasette comedièn mbègueère per Bou khar boumou defoon il y’a prèsque 30ans
J’ai même vu le documentaire vraiment
Tradition orale mo Mel nonu bouche à oreille day am toujours ay modification
Ces gens là sont dangerous, ils travertissent lhistoire. Merci Mr Syll
Mbaye gueye syla diaradiaf
Geumoumako limou wakh madiama fall la geum❤
Ouztas madiama fall kham kham lay wakh dh lou leerr
Feu Iba Der thiam avait règlè le problème il avait ecrit un livre sur lhistoire du Senegal 🇸🇳 authentic on avait refusè se livre voici les èreures
Lol, aka ño bëgg lu yomb! Un livre plein d'erreurs...
Jaaraama Baay mbay.
Wax ci mboor du ay caaxaan. Bala cee kénn di wax dakoo wara gëstu bu baax.
Madiambal nit leu Amna xam xam,mashalah
Ma. Ça Allah Lou am solo ga déff
Amna solo trope Dieuredieuf
Machallah baye mbaye
Dafa dioum rek et c’est valable pour tous le monde
Merci professeur on es avec toi
Histoire Sénégal aye fèni nèn la kouci nèk sa mame ngay beug mou déf dialorè 😂motakh version yi di bari
Mach alla amna solo Diereudief ❤❤❤❤
Merci ma diama fall
Merci beaucoup ❤❤❤
Merci mr sylla, ce gas erreur yi mouy déf mo beurry , déglou na béne récit boumou déff si egypte antique, mais j'étais abasourdi , si ay wakh you tégouwoul féne 😂😂😂 .
Doul rek lay def.
Mbaye gueuye linga w1kh foko ték yawit ,histoire wou orale dara lou tangible amoussi...soit humble danga geustou mou geustou
Y a rien de juste. Des épopées racontées par des laudateurs
En général les histoires ont toujours des versions différentes
Dieuredieuf ❤❤❤
Qui a raison, qui a tort ! je ne sais pas
mais en ce qui concerne l'histoire : c'est des sources et les sources peuvent différer c'est tout simplement ça
Jere jdief sill ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sénégal ñio wara bayi dieul nit ki temps mo leumbé si deuk di mbél mbéli à chaque fois si tele yi
❤ bay Mbaye gueye sylla
Dieureudieuf ya ngui deff ligueye bou rafet machalllah
Machalah madiama fall
Sëriñ mbay géy du jumde fen la.
Nn li histoire dong la dou question sos kou nek ak nimoukoy degge madiama fall brom xam xam la machalla
Histoire mom kouné ak nimou koy netallé
Mane lolou la geume ndakh oustaz madiama fall kénn d'où nataplé xam xam mame mo xam si walou histoire dîné ak sciences lépp la pékkk
@@piskogueye2638 bah ouiey parce que gnom sén ay époque ken fékéwoukoo alors kouné ak fii nga roté xam xam en matière d'histoire mom personnes n'a raison et personnes n'a aussi tort soyons juste humble
Pere😂😂😂😂
En 1886 Thilmakha Mbackol n existait plus.il à été fondé vers 1700 par Sakhewar Fatma mais il était tombé en ruine et a été refonde par Serigne Abdou Abass Diop en 1896 dans son emplacement actuel sur recommandation de Serigne Touba
Saa baay Mbaye Gueye syll yàlla Nako Fi yàlla bàyyi ta wéral ko barkèp allxoouran
Machalla baye mbaye gueye sylla
Jaajëf Bay mbaye Sylla sa taxa waay rafét na ❤❤
Interprétation
Li mbégueére moko wakh déglonako boyage
Lolou iska du théâtre 😂
Ki wakhi mbegére laye nétali
Oustaz bi lomo wah lolo la
serigne mbaye gueye syll histoire bo. Fékéwoul té source gni gua am day lako netalil mana wer mana bagna wer parce que gnoune sounouye histoire amoul démonstration scientifique motakh liguane moy guéne bolo def seytou mogueune guene ni wérenté parce que ay borome khamkham guen gnen gnar gnepp
Machalah ❤❤❤❤❤
Baye mbaye diaradiaf
Père ioe sa version nga wakh mom mou wakh version wam donc li eup solo moy sou amone firndé biniou bindone loolou sa jamono joojou nioune seutou lat Dior yi dîna niou geuna kham histoire bi donc migui melni ay Hadith you beuri yi niou wakhal yonnenté bi صلى الله عليه وسلم am you beuri you si leerul dieureudieuf 🙏🏽
Madiama est excellent
En vérité, le Pr Madiama FALL n'a fait que reprendre textuellement le récit de l'épopée de Lat Dior de la vidéo sur le lien que je viens de partager ci-dessus...