Débat Houleux - Pr Sanou Sy Ba à Ahmed Khalifa Niasse: "Wax Dagne Koy Solal Toubeuy..."
Вставка
- Опубліковано 3 лис 2024
- #kebetu #team221 #senegal
page facebbok : / senegal7officiel
Abonnez-vous pour plus de vidéos et n'oubliez pas d'activer la cloche de notification
Senegal moytulen ahmed ok
Senegal ngay jiss kou jangoul dine tok di wedi borom xamxam beug beuri wax...
Yeureum na talibé ahmed khalipha niasse
Yalla ngui fep signifie tt simplement fonek minguilay guiss....loy def khamnako
Vrai
Machala
Dieureudieufé Baye Niass mi niou régler lel il lëp walahi
Ms nay raffête, n'a diokh nitte gni tieur lolou Moy deugue, xolal plateau nougnou koy wowé "papeu" mais respect tmt walla
C un incompris Ahmed Khalifa Niass est un bibliothèque. Limou Xam da beuri té amoul kouko atan Sénégal wala beuriwoul bokk gni tokk si plateau personne je dis bien personne ne lui arrive à la cheville
Yennn amolennn xam xam pour affronter Ahmed Khalifa Niass
Cheikhouna Fedior blh très nulls même
@@baradiongue4506 surtout borom kaftan bou wekh bi amoul place fii
Ahmed xalifa soxlowo xam xam pr affronter reuyeul lamign rk deugeur fitt
Ya am ham ham dieuleul
Billahi
Sidi lamine yalna ko Yalla defal aldjana firdawsi 🙏🏿
Kou Melni Khalifa niass mi yalnaniou Yalla mousseul si niom si sen wakh you tegouwoul fenn
Aaamiine ya raby
Amine ki dagnouy fonto
Fi yalla mo'fi née koudoul yalla do touss
Xam xam bou amoul yar ak teguine yalna gnou si yalla mousseul / sokhor motax di'nga beugeu wax xam xam mou teuleu
Nioune nieupeu béne laniou di diéma diaxaçé ay mbokou mom seytané pir iblise mokoy déff/ faut qu'on fait attention nous les confrérie mouy Tidiane mouride layéne cazalika niassene / bilahi seytané'la / mala'ka wakh
Billahi day diaxasé rek
Way may len no akhmet khalifa kham kham lay wakh dade senegale boko wakhi déçue te guisosi bobmam komase de la de gat baye len nafekh
Bems bems man mouride la Ahmad khalifa Niasse aye wakham dase wara guene Serigne Touba nioune mouride ye Serigne Touba rek lanou am te mom franc maçon bou makla da bagua diakhase tarikhayes inchallah dou diallou yella nako yella touroukhal
*XAAJALOO BI DH AMALUNU BÉN NDIARIGN*
@@xaadim9615 bayil togne. Saway té nga mandou ci ameth khalifa
Soungen beugé dég xam-xam aki téguine déléne téwlou Segne Abdou Rahman ta ngén bayil ma ameth xalifa mi... Kou niak téguine la
Yalla lako takha wakh
Yaw khamo dara ki xam xam
Kou ndiaalo ci douche yalla daf lay bindal bakaar
Konn yalla mingui fingui fépeu nag vraiment
Il est dans son domaine. Il est critiqué partout et pourtant on ne met rien à la place de ce qu'on lui contredit.
instablaster
Li nga beug doko am touba ak tivaoune ben rek lay masa don inchalla
Yén amoléne argument pour danél khalifa niass sén xam-xam dissoul vraiment
Waa ms Omar mii ayy mbokam douñko teuyéé tmt serigne bii niass gni amouñ bénn xam-xam NIASS yalna sa diamou yagu
Islam toumourankei na vraiment. Kouye wotei wo nittou yalla di insité djigen yi si ay perruques tei mom guissoule wone waydiour bou djigen nam dam ko Def. Walla sen ni mame bayiwou gnou fi wone li. Yalla nak dou morom kou tei dou nitt kone naniou rafetale leip tei bollei si orma diou war. Wassalam
Tout à fait d'accord que DIEU est partout ☝️☝️☝️
No l’épe Mo nekke si yalla
Ahmet khalifa niass moy sene baye dèm léne sakou dji kham kham khalifa niass bravo lui tu sei più intelligente di Senegal papi Torino from Torino sei grave vai in analisi
D'à Am Nio Xamni Khamougn dara École arabe sakh Diangoune KO Beug Défier Ahmed khalifa Niass Ci Xam xam
Mo ma diakhal. So amé certificat sa discussion avec un docteur day posé problème .nid da fay nangou nivaume
Merci beaucoup professeur
Les émissions tv yii meu guiss temps yi, diouroul diam dé. Niongui diakhassé deug keurou diiné yi et à chaque fois ils invitent ahmed niass pour semé la discorde. Khamouléne lii lane la meuneu diour. Réseaux sociaux di ci profité di dieul ay extraits, nioune dioulite yi (douma wakh talibé yi ndakh nioune nieupe nio bokk Yalla ay dioulite laniou) di ci khassanté ak di saganté. Naniou kholaate sounou takhawaaye ak sounou bope 🙏🙏🙏❤❤❤🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Omar Mom waroul sakh Wakh li Mouy Wakh ni Xalé Yi sakh Dougnko Wakh " Diouli laape laci yalla wakh. néek sakh bou Setoul diouly Daganoufa Waxoumalak Douce. Yalla mongui fép mais lou Laap La daganal Diouli .ki Dof la rek omar amoul Xam xam
Omar khamoul darà mane sakh moko taneeeh🤣🤣🤣🤣
Omar mii kat khamoul dara Yalla migui fépou lolou mo am wayé dafa am foum sakou gnou diamouko fa
Le problème des senegalais danio yakaar ni diiné aada la , té yonéte bi amoul wone vie privée lép la leral si doundam même son intimité pr servir d'exemple parceque lolou moye tradition prophétique , si téré yi bou niouye diangualé si digue bi laniouye diar . Fii li eup si oustaz yi dagniye mbeuw rék wayé tous khamouniouko ,nioune nak danio tam séne niveau bou bas bobou motakh bou niou dégué lenene diakhlé .Limotakh naar yi nane noir africain yi khamou niou diiné .
Professeur soit philosophe évite d'être sous la houlette de tes pulsions vous jugez gratuitement Ahmed
Je bas a contre press de ce vs dites a propos sinn je pese b1 mes mots et je sais tres b1 de quoi je parle a propos qu il soit un sous bourguiba ok.
Waxal li am solo mo geun mama maodo malick ak serigne touba islam laniou fii xéxal waé dou xeuthieunto té nguén bayi di djaxassé killifer diner yi ahmed khalifa niass seytaani leu naafekh bou bne leu
wallahi xam xam rék waay borom yéré bou wékh bi wa khofi dara Ahmad doundal
Yéene dh séene arrangement rek.
Ne soyez pas égoïste waay.
Ahmed khalifa niass il a raison
Je l'estime trop personnes ne peut amené un talibe o paradis
Doule tu mens
Dangay doule
MDR la meilleur façon de dire une personne doule ou tu ment ces juste d'être con com le con et n pas connaître Dieu je n suis pas la pour insulte mes de loué mon sauveur soit béni
Comment une personne comme toi peut tamene o paradis ou tu pense que le paradis c pr son père yene yiii yap yalala boul kesou thi yalla rek gue nane doul
Lahilaha ilalaha dara amoufi loudoul Yallah Ahmed Khalifa kham kham kessé la
Sentv amougnn ayy professionnel. Ki di Khalifa niass xam xamm xamm rekk layy wakh 😍😍😍mais Omar momm xamoul tousss teehh d'où nopi😅😅😂😂
Omar mi da toukh lou bone la fok
Wa lane mootakh nga égoïste? Yéen daal louléene arranger rek?
Commentaire pertinent
Améte khalifa tiaga la vrai say say
serigne Khalid Niasse vous avez un niveau très élevé par rapport au autre il faut que vous apprenez a vous écouter il ya trop de disputes pour rien le monde entier vous écoute.
Amet Khalifa Niass star leu .
Bilahi lislam da simple yénako métil rék
Billahi ak beug di graw graw lou
L'islam n'est jamais simple
Cheick Moïnga wakho lou am dé lathé islam yénako disal mé disoul té ki limou wakh kham kham la lakhadarine rék sokoy diangue si digi bi lagnouy diar am Serigne yo khamné dougnou diar si digui bi té sokoy diangalé danga wara diar si digi bi islam c simple bilahi
@@aissatousow5899 j sui parfaitema d accord avk vs aissatou sow
Bilahi walahi dîné jii métiwoul déh
merci pape mactar
Sanossy mon professeur très pertinent
Excellent Pa Matar🙏👍♥️
Soyez un peu courtois dans vos paroles. Dîné yar ak téguine moy base bi.
Salam frère tu peux traduire pour qu'on puisse suivre le débat s'il vous plaît Merci d'avance
Ahmad khalifa Niasse franc maçon nako gourjigene ye deglou le guaye toude sono Serigne bé Serigne Touba khadimou rassoulilahi saw nakhare nama tourop boye toudo gua toudo sa morome franc maçon ye Ahmad khalifa Niasse sa wakhe niakhanye gua guene se Serigne Touba amal dioum Ahmad khalifa Niasse franc maçon
Serigne sam mbaye nèna kène dou wakh yalla ngui fép fép ngui si yalla lane wara wakh nakh bala dara di ame yalla mofi nékone
Le blem moye il faudra posée la question a Ahmed khalifa Niasse un jour pour vous montrer limouy wakh si Serigne Touba gueumouko naniou ladji sa baye khalifa Niasse wala sama mame Abdoulaye niasse ak Serigne Touba kou raw si yalla walahi nga khameni limouy wakh gueumouko naniou def attention
Waw naka la goor mané fleurs té ak djigeune ba paré dou génné dara si awrawam
Dama yakar khalifa niass dama beugua sank sénégalais yi yalla dou morom
Dieu est présent dans tous les lieux
Yalla moy lepp wayee lepp dou yalla deug deug la ladj mongui fepp wayee dou fepp lagn key toudou wa salam
Yalla xamxamam moungi fepp pas yalla moungi fepp, yalla moungi si arach
Ya Allah nekout fepp. Ya Allah mungi chi kaw, chi arass. Faut arrêter de dire ça. Ya Allah est en haut dans le dernier ciel cha Arass...wa salam
Yalla migui fepp ,
Ahmed khalifa niass limoy wakh dara néko thi deugg
Dangène dioum fèpeu nèk thie yalla
Lou lere
Kàddou Hàariif
Aka léér
Yalla katt dafa khèdiou fèn bagnouye khalate nane mongui fèp
Yalla moy yalla way
Mang lèniye jajufeufeul thie sènoup dèguine hakeuzaa 🙏🤝🙏
Khalifa Niasse d'où royou waye
S touba rek
Ya Allah nekoul fèpe dè.
Ya Allah mougui fèpe wakhou koufr leu.
Ya Allah mougui ci ci kaw Arascham beu lo lou leu wakh.
Wayè ci xam xam mom takneu lèpe.
Waxal lo xam
Amety. Mounna mongu. Verman. Whakh alxouran bou sette shakh mounolenko.
Nit meunoko djangual loumou xam beu parei djangale ko loumou xamoule nakh mou âme xam xam dou arabisan dou koumou meuna done diner moy outou xam xam khalifa djambare leu def leine ni mome
Yalla dafa direct sunu waraté kati nio niou leurré di rafétal pour beugueu guana corecte yalla
Ce pape Matar là non il manque de pudeur hein et a une mauvaise qualité de communication c'est grave pour un jeune porteur de parole comme lui vraiment ça va pas du tout
No ban Senegal la niou nek nii
Khalifa niass sa khol daye toth el hadji malick lagnou gueum losimane dara
Jajof
Et après sa leufeul ndaye
Fii keine mofii nei
Kou beug S touba diamou rk gay am billahi
Ahmada Diop reew nga trop
Ameth deugue rék lay wakh bilahi ki mako ngueum
Ahmed khalifa niass fi gay wakhé adouna dou nékh ba gayi khame figay wakhé njifa tok yeup amougne kham kham kouy wèdi ni yalla nékoul si douce wédina batou la ilaha ila la dara nékoufi loudoule yalla
Ahmed yaar ak teguine zero
En tous cas mon chemin n est pas dedans😂😂😂😂😂😂
Mais ce Ahmed Khalifa nous amerde way,il n’est pas plus instruit que les autres way ,c’est un faut type .faites attention.Sénégal n’est pas habitué à certaines paroles.
Ayway ahmed do nopi Sénégal amouniou capacité degg lingay wakh
Billahi
Il fait que mentir
Dr Bassirou BA officiel bilahi amougne ko mo takh dougne ko mousa gueum té bilahi xam xam lay wakh
Sanou sy xamoul dara akh deugu mom diaroul Ray rayla akh vraima
فاجتنبوا الرجل الذي يدعى العلم لا يدري ولا يدرى أنه لا يدرى
Gni nak danio niaka xam Yallah deugue nak Ahmed Khalifa Niass borom xam xam leu. Il faut comprendre qu'il faut appeler le chat par son nom Yallah bouné ni leu ni leu
Omar amo xam xam sa filo sakh dafa deisss
djoulitou senegal dafa beury nafek ki tok di wakh louko nekh di daganal li yalla aramal grafage yene daaaal
Pour moi en réligion il y a pas de philo c est écrit par le Prophete saw point on aplique c est comme la loi qui est ensemble des chartes fondamenteaux point
Il est vraiment pathétique il croit supérieur que les autres zèroo modestie khalifa
Professeur sanou sy donne des leçons à Ahmed Khalifa Niasse.ahmed Khalifa diakhal nama trop.perrique ak voile bén leu. Imaginé lén les femmes di july ak perruque,wala à la Mecque,gnouye tawâf ak ay perruques.gniko déff professeur gnognou togne
Proffesseur tu te comporte comme un opposant de ton invité qui est docteur dans ce domaine, le vieux xam xam lay wakh et tu très loin de lui même dans ton propre univers
Pap k k day saup rek
Yalla nekoute fepp ,Serigne Sam Mbaye néna fepp dadié nek ci yalla
Ahmed Khalifa tolowul ak gni niveau vraiment
Kham léne yalla mana diamu yalla
Brom lou wékh li xamoul dara😂😂😂No ameth khalifa sa xam xam kheudioul fi
Momo Diagne Bilahi khadjou fi khamougne sakh ki limi wakh téré la
Diné thi magua touba
nooooooon YALLAH nekoule fepou mais fepou mo nek fa YALLAH
Omar yaw amo sa place ci plateau bi zéro xam xam
Parfois je rigole vraiment quand je regarde les débats qui occupent nos télés au Sénégal. Qu'est ce que ce débat nous apporte pour sortir de notre pauvreté. Réveillez vous svp... Ahmed est très logique dans ses propos. Le débat serait plus intéressant si vous parliez de religion et corruption.
En plus le wolof dit "koye" le blanc dit "pénis" les Sénégalais par complexe d'infériorité pensent pénis et plus joli que koye. Et ils signifient la même chose. Réveillez vous svp. Trouvez nous des débats utiles.
Omar yaw tamit li dagann si diaka ak dioumaa daganoul si douce.amoo deg.yalla mounghi fep c'est à dire lep Loy def yalla khamnako té mounghi lay guides ndax moom rek mo yoor contrôle si lep
Bilahi corona rayouko dou deug
1 vu
Am lène yar ak teguine thi yonentou bi psl.
ÀLLAHO AKBAR 😰😰😰
Khalifa yabari xam xam tok ak niou khamoul dafa mėti lingay wakh pour niou nitè le
Geum geum bobou la am si mome
Vérité absolue
Merci beaucoup waroul wakh ak niou xamoul
Wormal lénn sinou borome
يا أحمد خليفة إياك والأدب فالقوم بالأدب حقا زادوا منه استفاد القوم مااستفادوا
Kholale ki mome ,ki di léral si neukdiou, mouy wakh, cone li guay wakh meuko danél, ñitt daguay dégue Lou, ndakh gua dégue.
Professeur vous êtes vrai fou kone Ahmed âme na talibé
Walahi moustapha
An tout ca mane dé dégueu na wakh diodiou si bénéne borome kham kham bou doul mome récemment .ma ngui ko dégué si béne cassette waraté Bou gnou tégone alfayda
Yalla nèkoul fèpeu,kagn guen di comprendr lolou.fèpeu nèkk si Yalla
sama seringue Khalifa niass
Astakh Firullakh liguay def chi douche bi defalko chi Dioumaji 😳🤕🙊🙉🙈
Non Omar faye mo deger fit😂😂kouko bayii mouy wah si diine.
Vérémant Sénégal arrété
Mais ce soit disant professeur il a un dent contre khalifa parcontre il ne fait que critiquer les propos de khalifa sans arguments. Les paroles de dieu ne doivent pas être modifiées pour faire plaisir qui que se soit .
Wakh léne té bayi yalla .
Méfions nous de akhmed khalifa Niasse
Mdrrrr Ahmed khalifa moral leu si j'ai envi de rigoler je le suis tout simplement mais nak ya du désordre dans votre émission faut briefer les gens avant émission
Ahmed khalifa dou nitou dra kou xam yalla deug dou tokk plateau di werante gni dagno gneuw pr diaxasse gnu ak borom bi waye yalla molen eupe doole fouf sax ndax mom doukouy seetan kou melni khalifa niass beurri na fisi rewmi ibliss mokoy wakhlo Ahmed khalifa ioe fouma dadje ak ioe na mbodim sa ndy defko sa mind