Il y a une différence entre ecouter et entendre aussi bien regarder et voir ce vieux Ahmed est vraiment un sage qu Allah me pardonne pour tout le mal que j ai pu dire a son égard wassalam
Ahmed Khalifa Niasse dérape certes mais il souvent raison sur pas de mal de choses. Et il raison, lorsqu’il dit qu’il n’y a que la parole du prophète qu’on ne pas contredire parce qu’il garantit par ALLAH . Sinon tous les autres peuvent se tromper.
Ahmed khalifa doit débattre avec ses égaux d'esprit et pas avec des gens qui sont pas spécialisés dans la charia, un médecin ne débat pas avec des non médecins.
قال تعالى: (( يا أيها النبي قل لأزواجك وبناتك ونساء المؤمنين أن يدنين عليهن جلابيبهن وذلك أدنى أن يعرفن ولا يؤذين))...الخ Lii la yallah wakh si alkhouran... A.Khalifa niass mom déy fountou rék Beuz laÿ wout.!
Je suis tt de cœur avec Ahmed Khalifa Niasse. Un homme très cultivé, un érudit. A mn avis ceux qui veulent prétendre discuter avec en public avec lui, doivent au préalable bien approfondir leur recherche et ne pas se limiter simplement à la seule lecture du Livre Saint ou les hadiths. Leur insuffisance est frustrante sur ts les plants devant ce Docteur. Respect à toi Dr Ahmed Khalifa Niasse.
Bilahi sa diangue soriwoul mai en dissertation française si vous ne mettez pas d'exemple concret vous risquez de ne pas avoir une bonne note mais Ahmed khalifa niass chaque quil développe une idée il donne d'exemple en disant que se je dit se trouve dans un livre et il donne le nom Et n'oublions pas que avoir des diplômes universitaires ne signifie pas que tu as tous appris 🙏🙏mon point de vue
Oumar Faye on est fier de toi tu es le seul à confronté sans complexe avec Niass sur des points l essentiels de l Islam. Oumar Faye le vrai sage. Un homme très véridique.
LAMINE NDIAYE sa wadji erreur rek lay def xolatal téré yi souniou nékon deuk bou serieux en matiere de religion dinaniou ko wo corriger ko,amoul béneu oulemas fi ba arabie bouy saxal limou wakh.
Trop de désordre à sentv, très nuls ces journalistes, Ahmat khalîfa Niass devrait pas venir là,il a raison ,ces contradicteurs ne font pas le poids face à lui.
Pardon Hameth Khalifa niass man louma geuneul boul dèmati si ben télé bougn ley invité, parce k nit yi dan la parel pour soufal la, toutal la,amouniou respect si mag, beugeu leu diahassè ak kilifeu dinè serigne touba, Elhaj Malick sy do sama dara avc respect hamal fouguey dem
Ahmed tu as bien dit même moi j'ai posé cette question à mon maître I avait pas la réponse j lui ai dit que une femme qui n a pas voilé ne sera pas mort il m a dit que dieu est grand il peut le permettre de la tuer sans voir sa tête Ahmed tu est très fort tu n a pas de conçurent
@@diawibrahimasalif4425 ani hadith bouniou ko wakh ? coucher avec sa femme en jeunant c'est interdit mais pas etre avec sa femme... khamolene ki nieuw di len diangal ngen koy saaga teu yen yeup molen gueuneu diang gueune len degg. c'est dommage deuk bi kouffi wakh deug niou kheekh ko way mom plus ngen koy kheekh aldiana wam di gueuna leer ... plus ngen di saaga plus yallah di ko beug ndakh wakhiufi dara lou nekoul si alkhourane.
De toute façon ce type mom il est fou à entendre ces dires rkk on sens qu'il n'est pes .. Invitet Ahmed Khalipha Niass cest equivalent a inviter le fou de notre quartier ou même inviter zoss 😂😂 Ndeysann thiey Akhiroul zamane yalla na gnou talla may soutoura akk moudieu mou rafett 🙏
Nooon ndeysane Sénégal gni khamougnou dara rek gnoy wax... gni dougnou degglou sax li Ahmed Khalifa di waw ndakh sen niveau dafa élémentaire trop... Wayé Ahmed benen yoné bougnou meunoul Indi borom deg deg you kowé del rejeter sen invitation
Samba Baye Modou BA Ka sa way nie mousoul diangeu sax khamnani limi wax tegouco fèn yaw man nga nangouni priqeu mouray la man nga ték priqeu dèm diouli
@@papadiene7381 non non mane douma diggueul ken mais dama beug bou Ahmet khalifa di wax gnou deggué fimouy wakhé au lieu de lui critiquer tjr comme c'est soi-disant Oustaz ou je sais koiii... Tjrs mom dey indi li kham kham wax ensuite mou indi interprétation bopam mais les autres dougnou weddi limou wax ndakh amougnou arguments... Ils passent leur temps à le critiquer alors gnom meunou gno indi xam bouy dindi limou wax
Ahmed khalifa niass tes vis a vis ont des idées arrêtées Je vous demande d éviter de discuter avec des fanatiques Afin ne regardez les gents de haut Tous mes respects
Il y a une différence entre ecouter et entendre aussi bien regarder et voir ce vieux Ahmed est vraiment un sage qu Allah me pardonne pour tout le mal que j ai pu dire a son égard wassalam
Ahmed Khalifa Niasse dérape certes mais il souvent raison sur pas de mal de choses. Et il raison, lorsqu’il dit qu’il n’y a que la parole du prophète qu’on ne pas contredire parce qu’il garantit par ALLAH . Sinon tous les autres peuvent se tromper.
Ahmed khalifa dou sen morom bayi lenn ko... c'est vraiment une personne tres intéressate mashalah
Ahmed khalifa doit débattre avec ses égaux d'esprit et pas avec des gens qui sont pas spécialisés dans la charia, un médecin ne débat pas avec des non médecins.
sen tv yenna ngui foyee dinee dji
ragal lennn yalla way am touti respect si musulmans yi
yéne gni di invité khalifa Niasse yéna niou yapp bilahi ki dafa yabaté way yén duago léne diko diapalé
Ahmed ndiass un pédophile un dialoquat bandit de grand envergure
Billahi gnikoy diapplé akamalène ène
Un profane qui parle avec conviction. sur des croyances religieuses . C'est grave .
Khamed d'où sen mborone .
Machallah niass.
Ammét mi say say degge la merci omor faye
قال تعالى: (( يا أيها النبي قل لأزواجك وبناتك ونساء المؤمنين أن يدنين عليهن جلابيبهن وذلك أدنى أن يعرفن ولا يؤذين))...الخ
Lii la yallah wakh si alkhouran...
A.Khalifa niass mom déy fountou rék Beuz laÿ wout.!
Merci oumar faye
Diné anarchique laye ahmed di diangalé
Merci beaucoups bien parlé
Merci mouhamet mbay
Longue vie professeur.....la vérité est amère
J sui d'accord Avc Khalifa niass
Merci
au lieu de parler ce développe ce pays, vous nous fatiguez avec une ordure de personne qui aucune valeur
Ahmed Khalifa Niass Un Faut Qu'ont Doit Plus Invite Sur Les Plateaux. Vous Êtes Responsable De Tout
Ya pas plus aveugle que celui qui sait qui détourne le chemin 😷😷😷😷😷😷😷
une vraie ordure qui se nomme Ahmed Khalifa niass
Merciii bcp omar
Docteur Ahmed il la plus de niveau dommage que les Sénégalais ne le connaissent pas
Merci omar fay
Assalamou Alaikoum wa Senegal Ahmed Khalifa niasse limoy wakh dara deussi deug day fen Nekoul nittou dine Djigueen bou kalawoul Malaika doula Toppo
Je suis tt de cœur avec Ahmed Khalifa Niasse. Un homme très cultivé, un érudit. A mn avis ceux qui veulent prétendre discuter avec en public avec lui, doivent au préalable bien approfondir leur recherche et ne pas se limiter simplement à la seule lecture du Livre Saint ou les hadiths. Leur insuffisance est frustrante sur ts les plants devant ce Docteur.
Respect à toi Dr Ahmed Khalifa Niasse.
Bilahi sa diangue soriwoul mai en dissertation française si vous ne mettez pas d'exemple concret vous risquez de ne pas avoir une bonne note mais Ahmed khalifa niass chaque quil développe une idée il donne d'exemple en disant que se je dit se trouve dans un livre et il donne le nom
Et n'oublions pas que avoir des diplômes universitaires ne signifie pas que tu as tous appris 🙏🙏mon point de vue
Ayyy kon rek gno nek si plateau bi ahmed. A raison
Ahmed khalifa kenne warouko degue lou
Oumar Faye on est fier de toi tu es le seul à confronté sans complexe avec Niass sur des points l essentiels de l Islam. Oumar Faye le vrai sage. Un homme très véridique.
En regardant les commentaire
Damay xamni senegal bariwul niou xam.
Ahmed halifa lou wer lay wax
LAMINE NDIAYE sa wadji erreur rek lay def xolatal téré yi souniou nékon deuk bou serieux en matiere de religion dinaniou ko wo corriger ko,amoul béneu oulemas fi ba arabie bouy saxal limou wakh.
Vraiment
il est juste brillant ce monsieur et comme il a bien mentionné, il a du mal quand le niveau vol bas :-)
Machallah.Ahmed khalifa . intellectuel de haut niveau
ahmed dou sene moroom demlene dianguiiiii
Trop de désordre à sentv, très nuls ces journalistes, Ahmat khalîfa Niass devrait pas venir là,il a raison ,ces contradicteurs ne font pas le poids face à lui.
Yaw féxél diarigne sa rew té bayyi wa sen tv
Fall yaw dangua noy bop
Vraiment Hamed khalifa ne doit pas être avec ces genres vraiment
ماشاء الله
Je suis très d'accord avec vous sr Ahmed khalifa Niasse malheureusement les niveaux ne sont pas les mêmes
Guinaw yalla Ak yonnentebi Mame Seydil hadji Malick Sy rta 🙏 moy sama lépp Di sama khôl yémalé woumako Ak kénn khalifa Niasse nk dafa réw rk
Djigéne boudoul mourou foum tokk malaaka yeurmandé doufa wathi lo lou moyy tontou bi dou malaaka mawti
Bilaye ki deye nakhe maguette la
Ahmed lène daal la d'accord mooy kouné meuna wakh gnou dieul mba gnou déloo bamou dess yonente bi sallalahou aleyhi wassalam kom nouko imam Malick wakhé malheureusement niou baari dagno diappe sen Serigne dou dioum daf lène diarral sakh niouy layyal loo khamni layouwoul loolou mom ndioumté laa
Ahmed khalifa est pertinent
Ahmed khalifa Niasse ki domérame la té amoule respect si niitte yi
Il fai honte a l'islam
Wallahi
Il pense tout connaitre hors qu'il se ridiculise devant les gens .
Merci Monsieur Oumar Faye
Quel enseignement peut-on tirer de ce plateau ??
Absolument RIEN
Ahmed khalifa sa tour bi rk mo bakh mais do dra diouguéll fi wy
Sa data ndeye
Machallah ahmed sa kham kham leer tu es tres humble. Soula nekhone togue sa keur. Yalla naguify yague te weur.
Pape Matar dit nous ton rôle
Amed niass bandi bi yaw my ya xamoul dara walla nga topou se bakane
Vive Oumar Faye que le bon dieu te bénisse. Amine
Nékhou ba nékhou akhemet khame khame laye wakhe loume wakhe Dara dou ka dinndi
Mahdi ragalal Yalla
à faire bi d'où Aÿ mame d'où Aÿ sante fi diamouléne yalah
Ahmed khalifa niass borom xam xam bou mak lä yen war guën dëm jangue wate dakh lëpp wara lër sii biir dinëbii jërejef Ahmed khalifa 🙏🏾
Merci beaucoup Amet ni amounou xam xam doul rek
😄😄😄
Thiaye Sénégal D'où Déme
Wàlakhi
Si vous n'arrêtait pas se soi-disant docteur en je n'en sais pas à quoi il va attirer la colère D'Allah sur le Sénégal ce que je souhaite pas
Pardon Hameth Khalifa niass man louma geuneul boul dèmati si ben télé bougn ley invité, parce k nit yi dan la parel pour soufal la, toutal la,amouniou respect si mag, beugeu leu diahassè ak kilifeu dinè serigne touba, Elhaj Malick sy do sama dara avc respect hamal fouguey dem
Mome moy diakhase Kate wakhou satanique rek Laye mais wakhoul vraiment
Vraiment
Mais khalifa niass bi esk mandi woul wonn
@@osezvision4583 😂
Ahmed mo amoul respects si loumuy wakh
Ahmed tu as bien dit même moi j'ai posé cette question à mon maître I avait pas la réponse j lui ai dit que une femme qui n a pas voilé ne sera pas mort il m a dit que dieu est grand il peut le permettre de la tuer sans voir sa tête Ahmed tu est très fort tu n a pas de conçurent
Pouvoir ha.....hein woy...
Nationalités Madagascar laye woute
🤔🤔🤔
Je suis plié 🤣🤣🤣Oumou lo t la meilleure
Omar faye boulen nangou gayi yakka islam ,islam dafa rafét lou niaaw bokkoussi.vous etes là pour tous les musulmans et merci d'avantage...
Ndogo sa diabar melni tandarma(Datte)lollllll...
🤣🤣
Ay way petit dieng dama woor 😂😂😂😂😂
Merci Omar faye ko domram le
Mon pays 😂😂🇸🇳🇸🇳
Ha ha oumar merci bravo 👏 ❤️❤️😂😁
Khali fa niass lingaye wakh si bane téré lako yallah binde dongo sa diabar amoul féne dh
Ahmed khalifa niass is about to made the Islam disave more respect bilahi
Je suis très d'accord avec serigne bi. Quand on enseigne il faut dire les mots tel qu'il est. Que Dieu vous bénisse.
Il faut dire ce qu'il ya mais pas inventer.islam a ses lois ! Jeuner etre avec sa femme c'est mal,l'islam ne force pas
@@diawibrahimasalif4425 ani hadith bouniou ko wakh ? coucher avec sa femme en jeunant c'est interdit mais pas etre avec sa femme... khamolene ki nieuw di len diangal ngen koy saaga teu yen yeup molen gueuneu diang gueune len degg. c'est dommage deuk bi kouffi wakh deug niou kheekh ko way mom plus ngen koy kheekh aldiana wam di gueuna leer ... plus ngen di saaga plus yallah di ko beug ndakh wakhiufi dara lou nekoul si alkhourane.
Papa sidy si j était vous faut plus accepter les invitations si je comprends bien les gens essayer de vous rabaisser
Humm senegal 🇸🇳 senegal 🇸🇳 am lenn foulaa
Il faut lui comprendre c'est un chiite il s'en fou du sunna... HOOOO ahmaed niass vraiment waneell fi nga fééété
Kiiii domérame la
@@elzondiaye7955 walakhi kay
Mé mome diabarame si farata yalla ak Sounnah Mouhamed lanioukoko takalé donc Sounnah amena ndiérigne
Wakhe deug yalla mais ki ni laniou kay bayi
En tt cas respecter nit bahna lol mane mom question bimou ladj yitelnama malaka mowti noumouye yobè jigeen jou mourouwoul beugue na lolou leer sama bopou
Malaka yeurmandé laniou wakh
Pere Khalifa dioulite leu wala???
Lolou question la,soudè dioulite dinama diaxal
Merci
Serigne bi niass je time bien
Hamed khalifa Niasse l'islam dako ray bou yague
Ahmed Khalipha Niass amoul bénneu personnalité. Di takhawaalou si Télés yi rek.
De toute façon ce type mom il est fou à entendre ces dires rkk on sens qu'il n'est pes ..
Invitet Ahmed Khalipha Niass cest equivalent a inviter le fou de notre quartier ou même inviter zoss 😂😂
Ndeysann thiey Akhiroul zamane yalla na gnou talla may soutoura akk moudieu mou rafett 🙏
Koorguouné AK ay Thiaxanam Ahmed raguelal yala diguedéde
Merci Omar Faye....ngor si Niass khamoul dara !!!!!
Kou khiif mar dou tala seuye.
yeen yeppa yem. ken ci yeen waxu fi lu jumm. Yeen tele yi deeleen di inviter borom xamxam yi ragal Yallaj
Parfois je me demande si on est des vrais croyants, comment on peut parler avec incompétence sur notre religion amoul suturë amoul respect !!
Merci beaucoup Mouhamed ndiaye
Lou lérr la serigne Ahmed khalifa wakh
Nooon ndeysane Sénégal gni khamougnou dara rek gnoy wax... gni dougnou degglou sax li Ahmed Khalifa di waw ndakh sen niveau dafa élémentaire trop...
Wayé Ahmed benen yoné bougnou meunoul Indi borom deg deg you kowé del rejeter sen invitation
Samba Baye Modou BA Ka sa way nie mousoul diangeu sax khamnani limi wax tegouco fèn yaw man nga nangouni priqeu mouray la man nga ték priqeu dèm diouli
@@papadiene7381 non non mane douma diggueul ken mais dama beug bou Ahmet khalifa di wax gnou deggué fimouy wakhé au lieu de lui critiquer tjr comme c'est soi-disant Oustaz ou je sais koiii...
Tjrs mom dey indi li kham kham wax ensuite mou indi interprétation bopam mais les autres dougnou weddi limou wax ndakh amougnou arguments...
Ils passent leur temps à le critiquer alors gnom meunou gno indi xam bouy dindi limou wax
Ahmed khalifa nekhouma dara
le président
Il faut éviter ce types de débat.
C'est de la confrontation que jaillit la lumière.
Ahmed khalifa niass tes vis a vis ont des idées arrêtées
Je vous demande d éviter de discuter avec des fanatiques
Afin ne regardez les gents de haut
Tous mes respects
Pk Sokhena Mame Diarra Bousso done mourou???
Lolou dina yèmais dh billahi
Wèrène tè rèk li bakhoul sene tv tele bou gnak class la
Amna Lou bakh loy kham diadouwoul di wakh
Je me demande quel est la finalité de tels discussions.
galou dof dou terrr
@@baboumbaye9004 wakhal dé🤣🤣
Niaw tay dh khaw nga dh. Omar Faye diereudieuf
Talibé Cheikh bi franchement contane na si yaw bilaye. Yalna Yalla takhawoula
Wawaw alkhouran deug nekoul thi téré mais niep douniouko nangou
Omar faye 💪🏽💪🏽✅
Pape matar vrai nafékhe la
Yalla xol léye féye
Ki'mo'bonne'merci'omar'es'maodo
Pourquoi vous êtes invité Ahmed Khalifa Niass sur la télé
pour man lolou moy question bi
😭😭😭
Outi buzz motakh nguén invité ko vous allez entendre toutes sortes de connaissance avec khalifa niasse 😂
Mom kay heur bou wakhe nop daloti lokho dar guemigne 🤔🤔🤔
Yen naa mana dollll