GP - Débat houleux entre Ahmed kh. Niasse et Oustaz Mouhamed Mbaye "Tu poses des questions débiles"

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 1 лис 2024

КОМЕНТАРІ • 746

  • @mouhamedndao6115
    @mouhamedndao6115 3 роки тому +155

    MERCI Oustaz Mouhammad Mbaye yalna yalla faye la🙏

    • @deugeuldioubeulleral4836
      @deugeuldioubeulleral4836 3 роки тому

      Oustass Mouhamed mi khamoul touss touss nak laa wakh khamoul dara dara dara wallahi.

    • @absafall7393
      @absafall7393 3 роки тому +2

      Si j’étais lui je ne partagerai jamais un plateau avec Ahmed khalifa niasse pour ce genre d’émission du courage oustaz

    • @aramendiaye6464
      @aramendiaye6464 3 роки тому +4

      @@absafall7393 walahi El azim wax nga deug defa wara bayi di debatre ak moom

    • @absafall7393
      @absafall7393 3 роки тому +1

      @@aramendiaye6464 c vrai parce que dafa lay pousser bagay wakhé khôl

    • @deugeuldioubeulleral4836
      @deugeuldioubeulleral4836 3 роки тому +1

      Sénégal amefi xam xam dafa yombou trop tekeulei Ahmed khalifa niass ak oustaz yi mongui melni ngay tekeulei prof université ak kouy dora ame bac,Ahmed khalifa niass li di kham khamou fikhe manam sariha amoul koukoko geuneu xam senegal,wallahi oustaz yi nek ci tele yeppou nak laa wakh dou senn morom,Sénégal nak amefi xam xam dafa yomb trop

  • @santr.rek69778
    @santr.rek69778 3 роки тому +97

    Ay way man dè titt na thi senegal souféké lou yalla atté laniouy modifier si tèlé journaliste yi wara ladj yemsi mais gnouy deugal ay fenn ak media impacte bimu am c dangereux

    • @madridh8543
      @madridh8543 3 роки тому +1

      wallahi c grave

    • @mouhameddiouf7314
      @mouhameddiouf7314 3 роки тому +1

      Doyna waar dh

    • @bounamafaye7121
      @bounamafaye7121 3 роки тому

      Waw kaye

    • @papemayorodiop5218
      @papemayorodiop5218 3 роки тому +5

      Les familles religieuses doivent intervenir en" live" ds ces genres d'émissions,sinon çà fera tâche d'huile tôt ou tard.Q'Allah Soubhanahoh Taala ns préserve et ns guide sur le droit chemin amin yaa raabi

  • @omarfaye1794
    @omarfaye1794 3 роки тому +75

    Walahi jrnalist yi respectewouñou senegalais yi Ahmed mbay du courage frere

  • @fatoumatacissokho7588
    @fatoumatacissokho7588 3 роки тому +61

    Bravo Mohamed Mbaye ligua wakh moye souneu. Tu as été droit dans tes bottes car le Coran n'est pas modifiable ni réformable. Dieureudieuf machalah Yallah na Yallah yoke sa soutoura inchalah si barke Yonéntebi Seydina Mohamed SAW Psl ak barke Serigne Babacar Sy

    • @deugeuldioubeulleral4836
      @deugeuldioubeulleral4836 3 роки тому

      Mouhamed mbaye mi khamoul touss touss tousss wallahi li Ahmed wakh moy degeu

    • @aramendiaye6464
      @aramendiaye6464 3 роки тому +2

      @@deugeuldioubeulleral4836 yow moom waxou kou sokhor ngay wax dema waxon sax demalay ignore comme nila nieup ignore do dara ba dara bolo thipripppp

    • @abdoudjigo4884
      @abdoudjigo4884 3 роки тому +1

      É si tu crois que l'islam dieu Allah sûbkhana watalah...la construire avc nos cerveaux...tu te trompes.... couché avec Une femme mature...qui né op ta femme de voix l'égal....sa s'appelle''' ndiallo'' .... Bilay ici ô Sénégal beaucoup de personnes n'ont pas appris la réligion ....c pour se là a touletent...ils ne prénnent pas lé sose ô srx....
      Exemple= un homme qui a Une femme....et il se coucher avec Une otre femme...chari'a Di on tué cette homme...
      Bref épourtemps se l'on otre cerveaux...c grave se cette homme a fait...é Pour temps la punition en l'islam c la mort.....

  • @modoufall1365
    @modoufall1365 3 роки тому +36

    Dieureudieuf Serigne Mouhamed Mbaye yalla nala yalla faiye barke Serigne Touba

  • @abdougueye2403
    @abdougueye2403 3 роки тому +60

    Diereudieuf ameth mbay contan naniou mes gayi nioguilay soth des tes khamou niou dara

    • @salifoucamara2800
      @salifoucamara2800 3 роки тому +2

      Maneu dama diakhlé sakh, Niari niite toi seuyoul, nek cii li leen nékh beu embeu am cii niou nane dou ndialo

    • @abdallahdiome3563
      @abdallahdiome3563 3 роки тому +1

      Yaw mi daga rerr

    • @abdouazizfall884
      @abdouazizfall884 3 роки тому +2

      Gnikoy sott ay complexé lanou tei khamougno dara ci dinner.
      Machalah oustaz Mouhamed MBAYE

    • @abdougueye2403
      @abdougueye2403 3 роки тому +1

      @@abdallahdiome3563 sy naka

    • @toutoularandiaye2116
      @toutoularandiaye2116 3 роки тому

      @@salifoucamara2800 né
      Néna ndialo la déglou waatal. Par contre bougnou fassalanteh yéneh sey ak consentement dom dioudou fa dou domou ndialo

  • @mrfall1168
    @mrfall1168 3 роки тому +10

    Doul rek lay deff domeuram bi niass 👈🏾😡😡😡
    Merci 🙏🏾 oustaz Ahmed Mbaye ♥️♥️🙏🏾

  • @mhdbachirdiakhate5989
    @mhdbachirdiakhate5989 3 роки тому +7

    Oustaz Mohamed Mbaye mou séll mi respect oustaz ❤

  • @mariemebellethiam6431
    @mariemebellethiam6431 3 роки тому +5

    Bilahi seytané you méleni yéne motax fi dege doufi ame dome bou joudouwoule si seye domou ndialo la merci mouhamah mbaye yalla nala sa lérou tourono

  • @salmadiop867
    @salmadiop867 3 роки тому +6

    respect oustaze mbaye dine fimou tolou ni si senegal doy n'a waar walahi

  • @fousseynousidibe3651
    @fousseynousidibe3651 3 роки тому +14

    Alhamdoulilah bouniou yallah bollé si wa keur Seydil hadji malick Sy dieuredieuf Oustaz Mouhammad ligua wakh xam xam rékk là jazakallah Hayrane ❤📿🙏🤲🤲

    • @mameoumardiop6399
      @mameoumardiop6399 3 роки тому

      Iaw waxal waxou nitte ki mamame mo waral keur maodo boufi inedit keur frer

    • @babacardiaw2750
      @babacardiaw2750 3 роки тому +3

      Koumou metti yaham ...merci kou bah Maodo.

  • @djilygueye8052
    @djilygueye8052 3 роки тому +47

    Barké s touba Sénégal barrina aye nafekhe ak aye nuit noye fowé diné dji Ahmed khalifa Niass moye 1ér saytané

  • @massoguibathily7157
    @massoguibathily7157 3 роки тому +16

    Nafekh yi barina si plateau soubhanala. Diné dougnou lignouye naat si khel. Dieuredieuf Oustaze

  • @abdoulayegerardsene3146
    @abdoulayegerardsene3146 3 роки тому +17

    Merci oustaz mouhamed gueune nala naw🙏🙏

  • @mohamedassanecoly5533
    @mohamedassanecoly5533 3 роки тому +55

    J'ai vraiment peur pour mon pays 😔.
    Serign bi seetaal yalla si lingaay wax

    • @morlam8705
      @morlam8705 3 роки тому

      Diangoulene diongoulene beug ma rirando! Yene ay Diop xass ak ay koromak gnoye Sene référence wa Sénégal donc regarder rek te nopi..moi suis Ahmed khalifa

    • @souleymaneanne7666
      @souleymaneanne7666 Рік тому

      ​@@morlam8705 yaw ya hamul tousse ngay saaga

    • @morlam8705
      @morlam8705 Рік тому

      @@souleymaneanne7666 Ahmed khalifa xamoumawone ni domerame la li c'était l'année dernière ngay répondre tey dof nga rek

  • @mamadoujr9085
    @mamadoujr9085 3 роки тому +37

    Journaliste yi amnagn nday fitt, senegal balagno meuna fo rek ramadan ñeuw

    • @mordieng7043
      @mordieng7043 3 роки тому

      Moma diakhal mane

    • @cheikhmbadj5599
      @cheikhmbadj5599 3 роки тому

      Ahmed khalifa niass yakh diine moko takha diouk dou.lenene

    • @toutoularandiaye2116
      @toutoularandiaye2116 3 роки тому


      Aalulbayt Global Information Center
      Home
      Islam Les questions sociales Chiites
      Résumé de la réponse
      L'enfant nés hors mariage est un enfant bâtard (enfant né à la suite de la fornication ; de l'adultère ou d'un rapport illégal), tout comme l'enfant né d'une femme avec qui on avait l'intention de se marier et que cela n'a pas abouti. Le saint Coran et les hadiths privent les enfants nés dans de telles conditions de certains privilèges sociaux sans toutefois bafouer leur dignité ou leur droit à l'instruction et à l'éducation. Par exemple, de tels enfants ne peuvent devenir guides spirituels (Marja'), imam d'une prière en assemblée, prière de vendredi, tout comme ils ne peuvent hériter de ses parents adultérins, ces derniers aussi ne peuvent hériter de lui. Mais l'enfant qui nait alors que l'homme avait l'intention d'épouser la femme et que cela ait échoué, peut devenir imam d'une prière d'assemblée et hériter de ses parents.
      Réponse détaillée
      Les enfants nés hors mariage sont des enfants bâtards (enfant né à l'issu de la fornication ou d'une relation adultérine) ou des enfants de présomption (c'est-à-dire quelqu'un fait des rapports sexuels avec une femme qu'il pensait se marier et qu'un enfant en naisse)[1]
      L'enfant bâtard ; certains versets coraniques blâment le fait que les enfants naissent par adultère ou fornication, comme ce verset : " N'obéis pas à tout homme qui prête trop de serment et qu'il est vil, détracteur colporteur de médisance, qui empêche le bien, transgresseur, englué de péchés, haineux, de surcroit d'origine douteuse "[2] . Les traditions définissent l'expression " d'origine douteuse " comme l'enfant dont on ne connait pas le père, enfant bâtard ou enfant né au bout des rapports illégaux[3]. Selon le saint Coran, l'adultère ou la fornication fait partie des grands péchés car Allah dit : " Celui qui commet de tel péché subira le châtiment et plus de punition le jour du jugement et demeura avec humiliation dans la genèse "[4]. Les grands péchés sont des péchés dont le châtiment réservé à celui qui le commet est terrible dans le Coran et les hadiths[5]. En guise de mise en garde des adultérins et les adultérines et de disparition de ce comportement futile, le saint Coran et les hadiths ont privé les enfants nés d'une telle relation de certains privilèges sociaux sans toutefois les priver de leur dignité, leur éducation et leur instruction[6].
      Dispositions légales pour l'enfant bâtard.
      Conformément à ce que les jurisconsultes islamiques ont déduit du Coran et de la sunna, ce genre d'enfant régis des dispositions de loi que nous allons énumérer avec certains hadiths comme preuve :
      1- Selon la loi et la législation islamique, le Coran repartit les enfants en illégal et légal. L'enfant né des entrailles d'un homme par voie adultérine est un enfant illégal dont les parents ne peuvent hériter et vice-versa[7].
      Il a par exemple demandé l'avis de l'Imam Ali (as) au sujet d'un homme qui a commis l'adultère à l'issu duquel un enfant est venu au monde, Il (as) a répondu : " Il n'hérite pas de son père car le Prophète (ç) à dit qu'un enfant bâtard n'a pas droit à l'héritage "[8].
      2- Selon la loi, si un enfant bâtard se marie, sa femme et ses enfants héritent de lui[9].
      3- Si un enfant nait d'un Sayyed par adultère, les non hachimites ne peuvent lui donner la Zakat, mais on peut lui donné la zakat d'un hachimite[10].
      4- Un enfant bâtard ne peut devenir Marja' ou guide religieux[11].
      5- Ce genre d'enfant ne peut non plus être Imam de la prière de vendredi[12] et la prière d'assemblée[13]. Tout comme le signifie l'Imam Baqir (as) dans un hadith : " personne ne doit accomplir ses prières obligatoires derrière un enfant illégal "[14].
      6- on ne doit pas prendre en considération le témoignage de ce genre d'enfant[15]. Comme il est mentionné dans un hadith : " quelqu'un demanda l'avis de l'Imam Sadiq (as) au sujet du témoignage d'un enfant adultérin. Il (as) répondit : son témoignage n'est pas acceptable[16].
      Cependant, l'enfant de présomption n'est pas comme enfant adultérin. Par conséquent, les dispositions légales qui s'appliquent sur l'enfant adultérin ne s'appliquent pas sur l'enfant de présomption. Donc :
      1-Un enfant de présomption peut devenir Imam de vendredi et d'assemblée[17].
      2- Il peut hériter de ces parents et vice-versa[18].
      Notes :
      1- Bahâ'i de Bahâ'ou Din ibn Mohammad Ibn Hossein Amili va sâvouji, Nezâm ibn Hossein, Jâmi Abbasi, vol 2, page 280 ; Mohaqqiq Sahih Mahallatî Hâ'iri, Sheikh Ali, Institut Manshourat farahani, Téhéran, 1ère édition
      2- Sourate Qalam :10 - 13
      3- Al Bourhân fi tafsir Qor'an, Sayyed Bahrâni Hâshim, vol 5 page 458, éditions Bunyan Beçat, Téhéran, 1ère édition 1413
      4- Sourate Al Fourqân : 68 - 69
      5- Bahâ'i de Bahâ'ou Din ibn Mohammad Ibn Hossein Amili va sâvouji, Nezâm ibn Hossein, Jâmi Abbasi, vol 2, page 368
      6- Rasâ'il Sheikh Mohamma Taqi Ja'fari, page 182
      7- Tafsir Al mizan; vol 18 page 471
      8- Al Kafi, Koleini, vol 7 page 163
      9- Tawzih ul masâ'il imam Khomeyni, vol 2, page 752
      10- Al ghâyatul Qasvih, vol 2, page 229
      11- Al ghâyatul qasvih, Sheikh Abbas vol 1 page 9
      12- Rassoul Ja'faryan, douze articles sur la prière de vendredi, page 254
      13-Sheikh Sadouq Man lâ yahdhouruhu al faqih, vol 1 page 378
      14-- Sheikh Sadouq Man lâ yahdhouruhu al faqih, vol 1 page 378
      15-Sheikh Tousi A nehaya fi mojarad fiqh wa fatâwâ, page 327
      16-Kashful rumûz fi sharh il mokhtassu nâfi', Abi Fâdel hassan ibn Abi Talib Youssoufi vol 2 page 523
      17-- Sadâdu ibâd wa rushâdu ibâd de Ali Usfuri Bahrani hossein ibn Mohammad, page 142 ; Miftâhul Kirâma fi sharh il qawâ'idu Allamah, vol 10, page 14
      17-- Mosnadu shia fi ahkma shari'a Narâqi Ahmad, vol 19, page 440

  • @santr.rek69778
    @santr.rek69778 3 роки тому +22

    Mais Lima beuga kham lanla Ahmed niass defal médias senegalais yi ba kou diog rek inviteko mouy sopi wahi yalla nimuko nekhé ak lolou gnimu mona lor si askannwi koy setann te beug lou yomb Ahmed arrête

    • @layetheonly5139
      @layetheonly5139 3 роки тому +3

      Media yi nio boko buz

    • @prodrmx5007
      @prodrmx5007 3 роки тому

      Audimat

    • @salioudiallo4425
      @salioudiallo4425 3 роки тому +4

      Gniffa nekone nieup apart MOHAMMED mbaye ay nafekh laniou c des corrompu guemouniou dara prtant wakh nafa sakh né Macky amna droit deff 3e mandat wahou gnici dara dafa âme niouniou yapp ils st pas sérieux

    • @mariememenemi1318
      @mariememenemi1318 3 роки тому +2

      @Bass Diouf télés yi buzz rek lagni outt.
      Sayer sougn ko inviter mou wakh you reuy, andii polémique, alimenter les posts sur les réseaux sociaux.

    • @hallehbe
      @hallehbe 3 роки тому +2

      Du buzz rek; nyome nyepp shaitan lanui ligaye yal

  • @hadaraseydihadjimalick9157
    @hadaraseydihadjimalick9157 3 роки тому +57

    Kouy weur yeefer djapal almett niass

    • @bayejobe4204
      @bayejobe4204 3 роки тому

      yama dol

    • @billy217setoumabadiakhou7
      @billy217setoumabadiakhou7 3 роки тому +1

      Ya mana doul c’est tw le yeefer

    • @mamandour5416
      @mamandour5416 3 роки тому

      Katal sa ndeye

    • @khalifaababacarNiang313
      @khalifaababacarNiang313 3 роки тому

      Boule Commentaires si yii waye

    • @lebuteur6121
      @lebuteur6121 3 роки тому +2

      Hadara seydi hadji malick
      Yowe rousse na sa tourre bu cell bii sounékoule wou lolou ma saga sa ndeye bou bakh esck khame na lane moye yéfére impolie ladjale lane sa pape lane moye yéfeure
      Douma talibé niasséne mes sa genre yi nanio wara moytou si genre commentaire yi

  • @aissataba3746
    @aissataba3746 3 роки тому +14

    Oustaz mouhamed vraiment tu devrais pas assister à ses débats ignoble sans respect pour l ISLAM

  • @senrock4608
    @senrock4608 3 роки тому +10

    Oustas Mouhamed MB AYE DIEUREUFFF
    j ai vraiment peur pour mon pays ayyy nafekh kesse tokkk ci plateau di wakh ci dinee loulen nekh

  • @sakhoelimanediallo3792
    @sakhoelimanediallo3792 3 роки тому +11

    Wa Pape Matar Diallo mi di deugeul ay fenou Ahmed Khalifa Niasse la meunoul comprendre ba lègui
    Woxi yalla demb moy wokhi teyy ta moy doni wokhi soub, yenn Sénégalais yi munugno wokh ba li aramone demb beugeu dagane tey

    • @salioudiallo4425
      @salioudiallo4425 3 роки тому +2

      C des corrompus guemouniou dara gte trop énervé

    • @aboubekrsadikhsarr3911
      @aboubekrsadikhsarr3911 3 роки тому +2

      Pape makhtar nafekh pur leuh

    • @madondior5302
      @madondior5302 3 роки тому +2

      Mane mi moma jakhal khamna défkoy thiompal ndakh khaliss rek lañou gueum! Doulénén

    • @sakhoelimanediallo3792
      @sakhoelimanediallo3792 3 роки тому +1

      @@madondior5302 xalissou Pabi mo waral yène chroniqueurs yi di diay sen dinè ak s'en goor

  • @mameabydiop2507
    @mameabydiop2507 3 роки тому +2

    Bien Mouhamed Mbaye fou alxar ry djibout ndiallo gafa

  • @bachiirleveridique9767
    @bachiirleveridique9767 3 роки тому +17

    *DÉGGAL NAAFÈX YI DI APPUYÉ WAXI SËRIÑ ÑASS*

  • @abdoulayengom359
    @abdoulayengom359 3 роки тому +1

    AY WAY RAGAL len yalla journalist yi neque si plato bi ay yeufou nafekh reck NGEN di Def boulen rous akhmed Khalifa ba doungen wakh degeu dieuredieuf oustaz mbaye

  • @Mouss400
    @Mouss400 3 роки тому +22

    Nafékh bakhoul thi ces petits journalistes en l'occurrence Pape matar, Mouhamed mbaye c toi qui a raison.🙏🙏🙏🙏

  • @babacartoure8120
    @babacartoure8120 3 роки тому +3

    mouhamed mbaye a raison et à tout dit, je sens que dans le débat danio beug légalisé ndialo journalist doméram yi, méy wakh niounane ay consentement, télévision dafa graw, dafa wara diangalé au lieu di yak, so wakhoul lou correct ba kénéne dém def ko di nga ci am bakkar, et je ne sais pas pourquoi journaliste seytané yi souniou beugué conflit ak thiow rék invité monsieur Niasse ce dernier qui a du savoir mais qui refuse de nous dire la vérité et qui adorent humilié les gens

  • @abrahammohamedgates5489
    @abrahammohamedgates5489 3 роки тому +14

    Si à chaque fois que 2 adultes qui couchent ensemble avec consentement c'est un mariage, alors c'est quoi la fornication ?

    • @layetheonly5139
      @layetheonly5139 3 роки тому +1

      Bell question

    • @alioufall918
      @alioufall918 3 роки тому

      bilay naniou capture sa message bi wakh ngua deugue bou werr segn bi

  • @rokhayathiam5t910
    @rokhayathiam5t910 3 роки тому +7

    Walahi journaliste yii tokk fiii nioyyy nafakkeee deugueh walahi g eu très mal au coeur en regardant cette émission mashallah ouztaz mouhamed mbaye liii rek warna dall sa khel tel khamni nittt gnii kham naniou fou deugueuh biii fété... Iow rekkk Ahmed khalifa niass ya limité si kham kham!!! Pape matar mom bayileine KO fofou moumayyy safff ni Michelin thimmmmm ki nima KO begné yalleuh nama yalleuh bale nafekh wa!!!!¡

  • @kingtvsylla6483
    @kingtvsylla6483 3 роки тому +1

    Oustage mouhamed mbeye mercii😍😍😍😍😍 journalise yi tokk si plateaux bi aye na fekh lane

  • @ndeyeoumydiongue1671
    @ndeyeoumydiongue1671 3 роки тому +6

    machaala oustasse mouhamet mbaye kham mbaye am gua kham kham mane YOWE laye deglou

  • @gueyegueye4201
    @gueyegueye4201 3 роки тому +15

    yalna nagnou Yallah mousseul si nafékh li mo gueuneu graw fouf problémou adji sarr

  • @maneseydina6564
    @maneseydina6564 3 роки тому +2

    Vraiment ne vous laisse pas aveuglé si y'a pas mariage c'est pas légal.nous sommes tous pêcheurs mais il faut pas qu'on essaie de défendre ce qu'Allah soubouhana watala a interdit.

  • @elydiallo4679
    @elydiallo4679 3 роки тому +12

    Mouhamed est très correct est posé dans ses débats. Ameth Khalifa même si je suis souvent convaincu par toi, faut savoir débattre aussi et éviter de voir les gens comme des nuls. Je pense que aujourd'hui c'est toi qui manquent d'arguments

  • @adamasow702
    @adamasow702 3 роки тому +4

    Merci Mouhamed Mbaye yalla nala yalla faye

  • @benabdallahndiaye7657
    @benabdallahndiaye7657 3 роки тому +1

    Comprendroolènne wallahii !!
    Ndahteiiii OUSTAZE KHALIFA FIMOUY WAXEII DAY LAADJ KHALATT FRANCHEMENT

  • @boromebakh28
    @boromebakh28 3 роки тому +8

    Depuis lors vous ne savez pas les péchés lors de l'adultère et ils se trouvent dans le bible ou sur le Coran , moi je vois que ce débat est inutile .

  • @aboubacrythiam1075
    @aboubacrythiam1075 3 роки тому +1

    Khanaa journaliste dagnoo ame doomou Diallo walla dagnoo Diallo ba paré doome sosousi motakhe gnouye andake niass

  • @aidis3605
    @aidis3605 3 роки тому +1

    Cnra na wakh ci lii. Ana décision bi niou dieulone avant koor gui . Diiné dji dou foyoukaay

  • @pgtjohn4483
    @pgtjohn4483 3 роки тому +1

    Bilay nakkk gni amouma kham kham deh mè apar Mouhamed mbaye le reste khamougn dara basi khalifa niass no jè pitiè ils sont fous

  • @abdourahmanely627
    @abdourahmanely627 3 роки тому +10

    L'homme au Boubou Blanc du courage et bne continuation...?

  • @mohameddiakhate932
    @mohameddiakhate932 3 роки тому +2

    Jeureudieuf Oustaz Mouhammed Mbaye jamm rek ngay am ❤

  • @aichaseck9036
    @aichaseck9036 3 роки тому +8

    Machalah Mohamed mbaye kham kham day andak yaar kilifeu day diokhé thieure

  • @cissendieguene7795
    @cissendieguene7795 3 роки тому +3

    Makk mou am xam-xam, gnak Yarr té gnémé Yallah (Allahou swt)you mélni Ahmed Khalifa niass yalla naléne yalla soukheul ndax gnoy yakk Diiné dji di yobbou nitte gni xamoul si ay erreurs rék.🙏🙏

  • @cineyacineya9420
    @cineyacineya9420 3 роки тому +2

    Respectei naa xam xam Ahmed Khalifa Niass wayei lima meunou ta d'accord ak mome moy à chak sou tassei ak ben oustaz sii plateau dafkoy neiweul dolei, diko wagnii... Sodei djoulite dagua warra diokh thieur sa moromou djoulite tei bagne ko khepp rawatiina sii télé..

  • @abdoulayediao7394
    @abdoulayediao7394 3 роки тому +1

    Gni nek si plateau bi yeup ay complex lagnou gnou khameni khalifa niass limouy wakh dou deugu gnou and si ak mom

  • @mortallagueye8523
    @mortallagueye8523 3 роки тому +11

    Senegal 🇸🇳 dafabari aye Sayetané koi 😥

  • @thomaspreira6129
    @thomaspreira6129 3 роки тому +10

    Bayiléne thiakhane bi tédi wakh deug...bo teudé té marié wo,, ndialooo la ak forme boumou meunti done ak diné boumou meunti done...

  • @yayouaboubakry1125
    @yayouaboubakry1125 3 роки тому +2

    Allahou Akbar🤷🏽‍♀️🤷🏽‍♀️🤷🏽‍♀️🤷🏽‍♀️🤷🏽‍♀️🤷🏽‍♀️🤷🏽‍♀️senegal laniou nek wala???????????

  • @aliounendiaye7940
    @aliounendiaye7940 3 роки тому +1

    Meunou gnou deuke si thiaxane 11 mois ba paré beuga xam sa diné si 1 mois. Nagnou bayi tiaxane té diamou yala.

  • @aissatoundour9972
    @aissatoundour9972 3 роки тому +4

    Soubhanallla consentement ou pas deux personne non mariès souniou deffai rapport ndiallo la ...ragal laine yalla ..

    • @morlam8705
      @morlam8705 3 роки тому

      Fofou la sa xam xam tolou ! J’ai un ami très pieux iranien qui m’a dit un jour que ce que tu dis c faux ! Chez eux en Iran peut être pas tout l’Iran mais un courant religieux , si tu parles avec la fille et qu’il y’a consentement vous pouvez faire le sex et même si après vous êtes plus en relation elle doit attendre 2 mois avant de faire un autre rapport ou se fiancer ! Sensgal nak ay thiedo you diot si lislam lagnou lou Nekh way interpréter

  • @amyka5114
    @amyka5114 3 роки тому +2

    Machalla mouhamed yaffi takhawale diné diamano soy wakh deug gnilaye farale dou beuri mais courage frère yalla na kham kham bi yokou

  • @niakhdiarignou6687
    @niakhdiarignou6687 3 роки тому +16

    Consentement pour les 2 personnes diallo amouthi/
    Leguy wakhi yalla foléne koy tekk

    • @nogayefall4770
      @nogayefall4770 3 роки тому

      Gni nio yabaté

    • @Mohameddiop1
      @Mohameddiop1 3 роки тому

      Gni danoo yabb ndeye niit yi

    • @yamasoda3230
      @yamasoda3230 3 роки тому +1

      Boko khamé rék nga wakh mako ay kou diangoul fo dieum🤔🤔🤔

    • @niakhdiarignou6687
      @niakhdiarignou6687 3 роки тому

      @@Mohameddiop1 wakhatiko

    • @niakhdiarignou6687
      @niakhdiarignou6687 3 роки тому +1

      @@yamasoda3230 non mais c'est grave yalle nanou yalla may sokhna you bakh beugue sey té am dîner

  • @mamadoucamara927
    @mamadoucamara927 3 роки тому +1

    Kaddu Tarikha ak Kaddu Islam bou gueuna Fort, té chaque jour ngay wakh thi Kaddu Islam té doy jeugalou joullitiy, saway sén Tarikha yi lougn soss la, amoul bénné lay thi Al QUR'AN, maylén gnou jamm si sén Tarikha yi

  • @papasandierydiop4691
    @papasandierydiop4691 3 роки тому +1

    Sénégal yénégui fowé diné dji deh lii bann débat là

  • @mbarmangara7352
    @mbarmangara7352 3 роки тому +4

    Ahmed khalifa Niasse dou touss, limou leen di gueumloo gueumou ci dara ndax waxi alkhour ann la weulbeuti à des intérêts personnels et parfois politique. Faites beaucoup attention à cette personne car parfois il est insolent. Daye daganal lou baxoul té ay consentement entre 2 personnes sans être mariées kharam , ndialoo leu et un mariage mérite des témoins au moment du mariage et vous les musulmans , ce Sidy , il faut l'arrêter , il est pire que le Covid. Yenn a ngi koyy setane Mouy xouss di dem gnimewouleen ko mais chaytane la.

  • @mhdbachirdiakhate5989
    @mhdbachirdiakhate5989 3 роки тому +1

    Khana niom ay domou ndialo lagnou lutax nangou wougnou deglou oustaz Mohamed quel pays

  • @mamemormbengue4227
    @mamemormbengue4227 3 роки тому +6

    On est dans quelle pays ... y’a na niou yallah dieggal té yeureum niou si barké alkhourane 🙏🏽

  • @ablayethiounexalaattv7883
    @ablayethiounexalaattv7883 3 роки тому +13

    Dieura dieuf cheikh ahmadou bamba khadim Rassoul Macha allha ousstz mouhamd mbaye Yall naa yalla faye. La barkép borom touba

  • @awkhadim4532
    @awkhadim4532 3 роки тому +1

    Mac bouyeeeee. Thiakhaaannn mongueuneu boneee. Oustaze. Biiiii. Li. Mouwahhhh. Dafalaireee. Baye. Lenn. Roubbebiiiiii.

  • @saliouhann8161
    @saliouhann8161 3 роки тому +5

    Svp waa Sntv guii invitez moi avec Khalioha niass mii ma ték ko sa place, lhaloul dara té saytaané piir leu

  • @Idiouf450
    @Idiouf450 3 роки тому +3

    Journalistes yi ki eup xam xam naniou andal niii, Mouhamed Mbaye yalnaleu yalla sameu, walahi gniii danio reer

  • @abdoulayediao7394
    @abdoulayediao7394 3 роки тому +1

    Consentement ak ndeye lep ci yam kou seuyeuk ko takoul yangui ndialo wa ahmet khalifa niass dou nguén wakh si mom

  • @talibecheikh7628
    @talibecheikh7628 3 роки тому +6

    Titna thi sama rèw bravo moukhamèt mbaye taye mom aye nafèkh ga tagal

    • @toutoularandiaye2116
      @toutoularandiaye2116 3 роки тому +1


      Aalulbayt Global Information Center
      Home
      Islam Les questions sociales Chiites
      Résumé de la réponse
      L'enfant nés hors mariage est un enfant bâtard (enfant né à la suite de la fornication ; de l'adultère ou d'un rapport illégal), tout comme l'enfant né d'une femme avec qui on avait l'intention de se marier et que cela n'a pas abouti. Le saint Coran et les hadiths privent les enfants nés dans de telles conditions de certains privilèges sociaux sans toutefois bafouer leur dignité ou leur droit à l'instruction et à l'éducation. Par exemple, de tels enfants ne peuvent devenir guides spirituels (Marja'), imam d'une prière en assemblée, prière de vendredi, tout comme ils ne peuvent hériter de ses parents adultérins, ces derniers aussi ne peuvent hériter de lui. Mais l'enfant qui nait alors que l'homme avait l'intention d'épouser la femme et que cela ait échoué, peut devenir imam d'une prière d'assemblée et hériter de ses parents.
      Réponse détaillée
      Les enfants nés hors mariage sont des enfants bâtards (enfant né à l'issu de la fornication ou d'une relation adultérine) ou des enfants de présomption (c'est-à-dire quelqu'un fait des rapports sexuels avec une femme qu'il pensait se marier et qu'un enfant en naisse)[1]
      L'enfant bâtard ; certains versets coraniques blâment le fait que les enfants naissent par adultère ou fornication, comme ce verset : " N'obéis pas à tout homme qui prête trop de serment et qu'il est vil, détracteur colporteur de médisance, qui empêche le bien, transgresseur, englué de péchés, haineux, de surcroit d'origine douteuse "[2] . Les traditions définissent l'expression " d'origine douteuse " comme l'enfant dont on ne connait pas le père, enfant bâtard ou enfant né au bout des rapports illégaux[3]. Selon le saint Coran, l'adultère ou la fornication fait partie des grands péchés car Allah dit : " Celui qui commet de tel péché subira le châtiment et plus de punition le jour du jugement et demeura avec humiliation dans la genèse "[4]. Les grands péchés sont des péchés dont le châtiment réservé à celui qui le commet est terrible dans le Coran et les hadiths[5]. En guise de mise en garde des adultérins et les adultérines et de disparition de ce comportement futile, le saint Coran et les hadiths ont privé les enfants nés d'une telle relation de certains privilèges sociaux sans toutefois les priver de leur dignité, leur éducation et leur instruction[6].
      Dispositions légales pour l'enfant bâtard.
      Conformément à ce que les jurisconsultes islamiques ont déduit du Coran et de la sunna, ce genre d'enfant régis des dispositions de loi que nous allons énumérer avec certains hadiths comme preuve :
      1- Selon la loi et la législation islamique, le Coran repartit les enfants en illégal et légal. L'enfant né des entrailles d'un homme par voie adultérine est un enfant illégal dont les parents ne peuvent hériter et vice-versa[7].
      Il a par exemple demandé l'avis de l'Imam Ali (as) au sujet d'un homme qui a commis l'adultère à l'issu duquel un enfant est venu au monde, Il (as) a répondu : " Il n'hérite pas de son père car le Prophète (ç) à dit qu'un enfant bâtard n'a pas droit à l'héritage "[8].
      2- Selon la loi, si un enfant bâtard se marie, sa femme et ses enfants héritent de lui[9].
      3- Si un enfant nait d'un Sayyed par adultère, les non hachimites ne peuvent lui donner la Zakat, mais on peut lui donné la zakat d'un hachimite[10].
      4- Un enfant bâtard ne peut devenir Marja' ou guide religieux[11].
      5- Ce genre d'enfant ne peut non plus être Imam de la prière de vendredi[12] et la prière d'assemblée[13]. Tout comme le signifie l'Imam Baqir (as) dans un hadith : " personne ne doit accomplir ses prières obligatoires derrière un enfant illégal "[14].
      6- on ne doit pas prendre en considération le témoignage de ce genre d'enfant[15]. Comme il est mentionné dans un hadith : " quelqu'un demanda l'avis de l'Imam Sadiq (as) au sujet du témoignage d'un enfant adultérin. Il (as) répondit : son témoignage n'est pas acceptable[16].
      Cependant, l'enfant de présomption n'est pas comme enfant adultérin. Par conséquent, les dispositions légales qui s'appliquent sur l'enfant adultérin ne s'appliquent pas sur l'enfant de présomption. Donc :
      1-Un enfant de présomption peut devenir Imam de vendredi et d'assemblée[17].
      2- Il peut hériter de ces parents et vice-versa[18].
      Notes :
      1- Bahâ'i de Bahâ'ou Din ibn Mohammad Ibn Hossein Amili va sâvouji, Nezâm ibn Hossein, Jâmi Abbasi, vol 2, page 280 ; Mohaqqiq Sahih Mahallatî Hâ'iri, Sheikh Ali, Institut Manshourat farahani, Téhéran, 1ère édition
      2- Sourate Qalam :10 - 13
      3- Al Bourhân fi tafsir Qor'an, Sayyed Bahrâni Hâshim, vol 5 page 458, éditions Bunyan Beçat, Téhéran, 1ère édition 1413
      4- Sourate Al Fourqân : 68 - 69
      5- Bahâ'i de Bahâ'ou Din ibn Mohammad Ibn Hossein Amili va sâvouji, Nezâm ibn Hossein, Jâmi Abbasi, vol 2, page 368
      6- Rasâ'il Sheikh Mohamma Taqi Ja'fari, page 182
      7- Tafsir Al mizan; vol 18 page 471
      8- Al Kafi, Koleini, vol 7 page 163
      9- Tawzih ul masâ'il imam Khomeyni, vol 2, page 752
      10- Al ghâyatul Qasvih, vol 2, page 229
      11- Al ghâyatul qasvih, Sheikh Abbas vol 1 page 9
      12- Rassoul Ja'faryan, douze articles sur la prière de vendredi, page 254
      13-Sheikh Sadouq Man lâ yahdhouruhu al faqih, vol 1 page 378
      14-- Sheikh Sadouq Man lâ yahdhouruhu al faqih, vol 1 page 378
      15-Sheikh Tousi A nehaya fi mojarad fiqh wa fatâwâ, page 327
      16-Kashful rumûz fi sharh il mokhtassu nâfi', Abi Fâdel hassan ibn Abi Talib Youssoufi vol 2 page 523
      17-- Sadâdu ibâd wa rushâdu ibâd de Ali Usfuri Bahrani hossein ibn Mohammad, page 142 ; Miftâhul Kirâma fi sharh il qawâ'idu Allamah, vol 10, page 14
      17-- Mosnadu shia fi ahkma shari'a Narâqi Ahmad, vol 19, page 440

  • @mbayediopdiop6118
    @mbayediopdiop6118 3 роки тому +1

    Gor AK djiguen bonou seye té ken mayewolen nialola

  • @babacartabane7580
    @babacartabane7580 3 роки тому +1

    Merci mouhamde mbaye yalla nala yalla takhawo merci

  • @mamadougueye7473
    @mamadougueye7473 3 роки тому +12

    Ameth khalifa ! Yombal nga sëy looool.

  • @djibysane2114
    @djibysane2114 3 роки тому +2

    Salam oustaz mbaye gni leu weur lou gatt molen meun takhalé mouy ni : la takhara bousina boul lale boul djiégué lolou la yalla soubhanahou wa tala djiangalé lou ndieuk balay ageu si ndialo ndakh kousi sa yaye done ndialo wala sa diabar degg ko rekk doula nekhh masala mouy deug bajilenn deugeul wala di djiemeu rafetal bakar bou niaw may wakh niounane consentement new kham kham la ? wala seytané rekk lan waleykoum Salam.

  • @ousmanefaty7098
    @ousmanefaty7098 3 роки тому +1

    khalifa niass dou nitou deugue khamoule dara daye senk askanbi.merci

  • @pathesamb9561
    @pathesamb9561 3 роки тому +17

    Yėne journalist yi daguėne bary ay nafėgue guėne di faral pa bi wakhoul deugue

    • @malicksamb455
      @malicksamb455 3 роки тому +1

      Vraiment

    • @momoniang6776
      @momoniang6776 3 роки тому +2

      Ame léne yar pabi mo raw sen aye baye si chariha

    • @coeur2lion38
      @coeur2lion38 3 роки тому +1

      Saway wahal sa kaw way

    • @coeur2lion38
      @coeur2lion38 3 роки тому +2

      @@momoniang6776 sa baye yaw la raw imbésil ya réw

    • @abassdiagne3672
      @abassdiagne3672 3 роки тому +2

      @@momoniang6776 dagay doul khana sa baye la raw

  • @mbayebayeniass7342
    @mbayebayeniass7342 3 роки тому +2

    Magu balou niap mi pape Ahmed khalifa niass ki lou mi wakh si Xham Xham lako teuk
    parce oustaz Mouhammad ki lim wakh ni fo wer lako teuk parce si Xham Xham lako teuk.......... ta niou bayi wakh niou bon yi ki kilifa dou sene morom magu balou nak 🙏

  • @badadiaw5593
    @badadiaw5593 3 роки тому +1

    Sénégal yakhouna légui des gens qui ne connaissent rien de charria se permettent d'y débattre ragal lenn yalla

  • @mohameddiakhate932
    @mohameddiakhate932 3 роки тому +1

    Keipp kouni domou ndialo day donou parceque domou ndialo nga domou haram yi nguein done

  • @ousmanefaty7098
    @ousmanefaty7098 3 роки тому +1

    pa bi dafa rouslou li mouye wakh dara dousi deugue ki dou dara.merci

  • @lunelune8872
    @lunelune8872 3 роки тому +1

    Deretou yonint bi. Ya sof. Dieuffewoko deh nafekh bou bone bi

  • @fatoudiouf2584
    @fatoudiouf2584 3 роки тому +1

    Qui varoulaine ko invites si teleyi

  • @elhadjimalickmboup2241
    @elhadjimalickmboup2241 3 роки тому +6

    Plateau yi naniou top ki rek ci louko néh, naniou dém rek .....légui ndialo sah holougn li neh Yalla mais nigniuko beug guissé rek....Wallahi dinguen ham ni Yalla fowoul fowlouwoul niou dem rek.
    Ki dafa rér té dinala yobalé niou bari....diné dara leundeumou ci ndah kiko mom daram leundeumoul mouy Yallla sounou Borom.
    Top sa bakan mofi am ,mais Yalla mom souy douma nieup lay bolé...lifi héw fane passé yémoul kén mais aythia rek

  • @coumbadiop3305
    @coumbadiop3305 3 роки тому +1

    Sa c'est honteux niass ani yalla dans tout sa revoie tes paroles

  • @salioudieye4454
    @salioudieye4454 3 роки тому +1

    Lislam téguwul si ay guis guis bayilén fowé lislam mak dafa wara wax loum xam
    Ioe pape matar waxal si lo xam

  • @ousmanefaty7098
    @ousmanefaty7098 3 роки тому +1

    mouhamad mbaye yalla na la yalla barkelle khalifa amoule Barker fene fene rek ak dof. merci

  • @serignendiaye9851
    @serignendiaye9851 3 роки тому +1

    Ahmed khalifa mii man diakhal nama nitt kou khamné yakh rekk

  • @yayebakh5906
    @yayebakh5906 3 роки тому +2

    😭😭🤭🙊🙊astahfirou laha😭😭

  • @seexunaanjaaye7399
    @seexunaanjaaye7399 3 роки тому +4

    Mohammed billahi wakh NGA DEUG kii dâ réwe waye

  • @fatougayefall8069
    @fatougayefall8069 3 роки тому +1

    Merci beaucoup oustaz Mohammed contente naniou ci yaw

  • @Aistv2014
    @Aistv2014 3 роки тому +2

    Serigne Ahmed deh wodiour bou Bakh ba Motakh do kham sakh loka wara Wakh,mais yalla bou yalla def si kenn deug Ak topou si Wakhtan bi

  • @houdoudiallo6638
    @houdoudiallo6638 3 роки тому +2

    Croyons en nos principes et ne cherchons pas à plaire à une personne comme Ahmed khalife naisse qui se glorifie de sa lignée prophétique dont il n est pas le seul .
    Merci à oustaz Mbaye Machalla
    merci pour la pureté des réponses et vérités.
    Pape matar Diallo et Omar faye leundeumeul askanwi vos positions m ont déçu

  • @monsieursy1412
    @monsieursy1412 3 роки тому +2

    Oustaz Mohamed Mbaye nassa diam yague 🙏 ngor si Niass mom waxouma ay waxam ish

  • @adamakhouma1882
    @adamakhouma1882 3 роки тому +2

    Man dal lima guiss sounou télé yi moy c'est rarement guay guiss kou mana wkh sénégalais yi lou nou mana degu loy andy tihouw rek moum lan bague ahmed amna kham kham ga mais Manou degue li moy wakh ndaxh neveu bi moy wkhe Manou Manou niou kou kham kon télé yii bon niou for ce Ahmed pour quoi niou envit ousstas allioune sall ndakh moum kham na fou neveu sénégalais yi Toulou mou wakh niou mana kham limy wakh mangui diegu lo bou bakh nak 🙏🙏

  • @ousmanemamadousall2066
    @ousmanemamadousall2066 3 роки тому +10

    journaliste yii yéne raga léne yalla nguene baayi fene

  • @Sidy6922
    @Sidy6922 3 роки тому +15

    Ameth yaw daga am febarou khéle

    • @galsen-dev6272
      @galsen-dev6272 3 роки тому +2

      Non gnikoy invité nioko déf

    • @adamakaloga9479
      @adamakaloga9479 3 роки тому +3

      Ameth khalifa Niass Nappe Naa Sénégalais yiii Soff

  • @lunelune8872
    @lunelune8872 3 роки тому +2

    Ahmeth mbaye pose des questions pertinentes. Ahmeth dafa kham ni boy bi daf koy torokhal. Ahmeth beugoul kou diang as toute. Ndakh dou siw

  • @guidotoure4254
    @guidotoure4254 3 роки тому +1

    Vraiment je pitié de mon pays chaque année c comme sa ay kilifeu de grand referent di togu si télé di wëdente nn c triste 😥

  • @salioudieye4454
    @salioudieye4454 3 роки тому +5

    Bayilén fowé diné nguir diëmi yalla 😭

  • @amadoumarico5944
    @amadoumarico5944 3 роки тому +2

    Franchement je suis pas d'accord avec Ameth Niass sur ce point c dangereux

  • @papeseck6124
    @papeseck6124 3 роки тому +10

    pabi day doul rk man louma diakhal mom wakhtanou leuf😅rk domouram la

  • @Ndiobafaye997
    @Ndiobafaye997 3 роки тому +1

    Père linga wakh mom adumaci

  • @mouslayeimmosenegal3529
    @mouslayeimmosenegal3529 3 роки тому +2

    Sénégal mo beuri nafecc journaliste bi nane bou amé consentement amoul ndialo 🤣

  • @fa-houzma-ateitoukawakounm939
    @fa-houzma-ateitoukawakounm939 3 роки тому +25

    Vive le sonko makcy sall dégagé

  • @moussandour2540
    @moussandour2540 3 роки тому +3

    Yoneteby waxone na beus dîna diot niou daganal nialo ak riba ,ta lolou rek lafi guiss ay nite youy tokk di daganal nialo soubhanallah .

  • @femmesenegalaisecanada8522
    @femmesenegalaisecanada8522 3 роки тому +1

    Dome bou dioudou thi or mariage mom dou donne té,dome bobou laniouye wakh domou kharame ,kharame thi arabe moy lou bonn

  • @moussaba2321
    @moussaba2321 Рік тому

    Concentement Daganna Si alkhouran accord kél konk la yalla wakh .sourate 4 verset 24.