MAUX DE LA SOCIETE: RENCONTRE AVEC MOUHAMED DIAW ALIAS 'PIIFF' ANCIEN AGRESSEUR CHEF DE UNO ALEX....

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 31 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 110

  • @seyeyaram555
    @seyeyaram555 Рік тому +30

    Yalla nagniou yalla may moudjiou bou rafet amine

  • @Justin-Lo.
    @Justin-Lo. Рік тому +19

    Au moins une chaîne qui propose un programme hors politique merci pour ce reportage et faites-en d'autres il y a beaucoup de choses dans ce pays qu'on pourrait faire des reportages intéressants

    • @SsaiSenegal
      @SsaiSenegal Рік тому +2

      L'injustice c'est différent de la politique malheureusement l'hypocrisie sénégalaise prend les maux des citoyens pour de la politique 😂😂😂😂

    • @Reactionseriesenegal
      @Reactionseriesenegal Рік тому +1

      Merci bcp vraiment pour les encouragements

  • @papamalicksow5801
    @papamalicksow5801 Рік тому +8

    La question de la pauvreté doit être prise au sérieux.

  • @Luzprobreuxxx
    @Luzprobreuxxx Рік тому +3

    Man loutakh melouma nonou Moy Sama Mame yalla manako yalla fayal ta yeureumko

  • @mohamedvarre1250
    @mohamedvarre1250 Рік тому +26

    Dou ngen meu dieul meu ligueye ak yéén, il y'a une sorte de communication qui diffère le professionnalisme, il faut percer l'intérieur de la personne pour le mettre dans le bain de l'interview ✌🏽. La journaliste est bonne mais trop innocente

    • @ousmanefaye6581
      @ousmanefaye6581 Рік тому +2

      Vous formerez sûrement un très bon duo

    • @ousmanefaye6581
      @ousmanefaye6581 Рік тому +1

      Vous formerez sûrement un très bon duo

    • @mohamedvarre1250
      @mohamedvarre1250 Рік тому +2

      @@ousmanefaye6581 ça sera avec plaisir, en plus j'ai travaillé comme barman j'e' connais un peu sur cette vie

    • @issmansour
      @issmansour Рік тому +1

      Mais pk tu attends qu’on t’embauche? Tu as telephone qui a une camera non?

    • @mohamedvarre1250
      @mohamedvarre1250 Рік тому +1

      @@issmansour Oui mais ça ne suffit, il me faut d'abord une carte de presse entre autres

  • @mariamacisse5972
    @mariamacisse5972 Рік тому +6

    Kone mome légui Serigne la 😢ok senegal allons rék

  • @morlo1034
    @morlo1034 2 місяці тому

    Anciens bandits yep ay serigne laniouy nek apres
    Anciennes yi nek ay set katou petaaw😎

  • @babacarfaye9060
    @babacarfaye9060 Рік тому +10

    Banditisme n a pas d issue heureuse, soit la prison ou une mort violente

  • @usgalsen
    @usgalsen Рік тому +6

    11:28 Soxna si yoonam nekkul ci li Paa bi di wax🤣Elle ne lui laisse aucune chance de developper ses reflexions😂 Elle agresse Piff a tout moment🤣

  • @papamalicksow5801
    @papamalicksow5801 Рік тому +17

    Que DIEU le pardonne toutes ces erreurs.

  • @FlexFred
    @FlexFred Рік тому

    Pere nena mashallah mashallah

  • @dabondiaye7917
    @dabondiaye7917 Рік тому +4

    Journaliste quand tu pose une question il faut laisser le temps de répondre piano piano rekk

  • @andrendione9021
    @andrendione9021 Рік тому +24

    Il regrette après devenu vieux. Mais mieux vaut tard que jamais

  • @manoudiallo1350
    @manoudiallo1350 Рік тому +4

    Yallah na borom bi diegal leuh te yok leuh doler si yone bou bax binga dieul.

  • @oumougning5481
    @oumougning5481 Рік тому +7

    Agresser ba Maguette ba amato dolé beug niou sonal…Niatta nites nio deuk banlieue,yorouniou et ils travaillent dignement ? Moi en tout cas j’ai op pitié

    • @manoudiallo1350
      @manoudiallo1350 Рік тому +2

      Yow kou soxar nga. Yallah biniou bindeuh mom niou chaque jour niou togn ko balou. Yow sa dieumi bop yangi si ay bakar yo xamni toujours nga balou borom bi. Kou dem ba regretter tegouwate si yone ba parer di diox jeunesse bi ay conseil dango ko wara nianal. Soukou nexone guen si télé yi nane mako defone ma tay je ne regrette rien ba parer nane jeunesse bi dem len def com mane nima done def teh bou boba kene dou si meun dara.

    • @abrahamdiallo4057
      @abrahamdiallo4057 Рік тому +1

      Vraiment lolouu lay wakh pourquoi deuk banlieue daga wara nek bandit ou agresseurs

    • @ngagnessirydiop2897
      @ngagnessirydiop2897 Рік тому +1

      DEUG piiir NGA wakh

    • @makhtarcisse1919
      @makhtarcisse1919 Рік тому

      Il n'a pas l'air d'avoir pitié. Je vois quelqu'un qui assume les conséquences de ces actes dignement.

    • @galsen5350
      @galsen5350 Рік тому

      ​@@manoudiallo1350 douguen bayi ndeyou sén emotions yi .

  • @fnoumbediop690
    @fnoumbediop690 4 місяці тому

    Li dian ngatt La si bèpp ndaw bou nèkk si yonn😮

  • @laminebarrambengue6602
    @laminebarrambengue6602 Рік тому +3

    Gni nga agresser khamo bakham dénan waladét apre

  • @diagnemoussa1505
    @diagnemoussa1505 Рік тому +1

    Allko rek akh doumou adamayi moula dall

  • @thianediallo9294
    @thianediallo9294 Рік тому +2

    Journaliste bi dou maye qui mou développer sheut 😂😂

  • @laminebarrambengue6602
    @laminebarrambengue6602 Рік тому +2

    Ki manouma guem né rayoul niit kén dou wakh si télé rayna niit

  • @aboubacarfall1222
    @aboubacarfall1222 Рік тому +2

    Journaliste bi dafa euppeul
    Faut laisser à l'invité du temps pour répondre à vos questions

  • @ndoyadiop5069
    @ndoyadiop5069 Рік тому +1

    Journaliste revois ta façon de couper tes invités…. Laisse les developper way…..

  • @GfyThiaroye
    @GfyThiaroye Рік тому +4

    Seul les imbéciles qui ne changent pas, le bon dieu c'est le grand pardonneur. Il s'agit tout simplement le repentissement soit sincère

  • @inconnu90000
    @inconnu90000 Рік тому +1

    Pa bi conn mingui fiii??🤣🤣
    J'ai vu ses anciens vidéos

  • @AnnemarieMendy-h4o
    @AnnemarieMendy-h4o Рік тому +2

    Peut être il l'on opérait est tant mieux yala néniou souniou borome samb

  • @Pablobi
    @Pablobi Рік тому +4

    Journaliste bi eupeul na sheuteut 😮

    • @khoudiatoure7291
      @khoudiatoure7291 Рік тому +1

      Douko may sakh foumou wakhé pour développer c’est incroyable ! Au moins après une question laisse le temps à la personne de répondre

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому +1

      *Trop sakh douko may sakh mou développer 🤦🏽‍♀️*

  • @modousougou2769
    @modousougou2769 Рік тому

    Déguel journaliste bi gny sen histoire mola makk 😂😂😂😂

  • @atouthiam5440
    @atouthiam5440 Рік тому +3

    Senegall dou deme demba mageutt monotou darra die niou bageu raye

  • @mouhamadoubambaniang9587
    @mouhamadoubambaniang9587 Рік тому

    Doul way journaliste biiiiiii mouy melniii bey niiii dama moudiei enervei beu dagu video bi

  • @papemorfall8024
    @papemorfall8024 Рік тому +5

    Suffit il de naître en banlieue pour être agresseur ! C'est faux je pense que tu le sais très bien

    • @manoudiallo1350
      @manoudiallo1350 Рік тому +1

      Il n'a jamais dit cela, raison pour laquelle il donne conseil aux jeunes de la banlieue d'aller travailler. Bayilene soxar

  • @diagnemoussa1505
    @diagnemoussa1505 Рік тому +1

    Lii mou yakh Sénégal lii amol ben sass wakoh l'en fin dara

  • @awagueye7640
    @awagueye7640 Рік тому +4

    Thiey adouna dou dara

  • @AdjamaguetteGueye-e7f
    @AdjamaguetteGueye-e7f Рік тому

    Est-ce que journaliste leu

  • @DameBeye-yo6fn
    @DameBeye-yo6fn Рік тому +1

    Journaliste bi na dem diangui

  • @amethdieye6944
    @amethdieye6944 Рік тому +9

    Ki dè mageut mo takh mou bayi amout pèkhé

  • @safythiam
    @safythiam Рік тому

    emission bi concept bi bakhna mais technique ak déroulement bi bakhoule

  • @majestytv9210
    @majestytv9210 Рік тому +1

    Banditisme li rek moy finalité bi la prison la mort ou le regret té liye andi regret bi ay boy you ndaw yo influencé nio lay malmené ba ngua sonnou après niou dieul relève bi

  • @diagnemarie4902
    @diagnemarie4902 Рік тому +1

    ❤❤❤❤

  • @syllasamba3024
    @syllasamba3024 Рік тому +6

    Ki sama giss giss dafa nékk makk rékk mo takhe mou bayi...dafa manatoul

  • @diopndayefatou8938
    @diopndayefatou8938 Рік тому +3

    Journaliste manoul dara

  • @adjimbaye9909
    @adjimbaye9909 Рік тому +6

    Journaliste bii dafa dessei tey il faut être pausé ladj nank ak tey mei professionalisme bi desna

  • @ngaka9978
    @ngaka9978 Рік тому +3

    Msguettoum bandit nèna lègui thiokoroba la 😂😂😂😂

  • @safythiam
    @safythiam Рік тому +1

    journaliste démal def sport mo gueune si yow sa kheukheute métina

  • @keitacheikh-bx9fu
    @keitacheikh-bx9fu Рік тому +4

    Diarounou yeureume

  • @fatousene4439
    @fatousene4439 Рік тому +3

    Photo Serigne fallou bi rék momasi métti y'a bonne

    • @MatySow-r4i
      @MatySow-r4i Рік тому

      Kou bone ak kou baxe yalla ko mes ahmadou ba bayiwoulle bakan ak sénégalaise yi

    • @amethdieye6944
      @amethdieye6944 Рік тому

      Kou diapou nè kou bakhla beugoo mel ni mom

  • @NabiDiop-n1p
    @NabiDiop-n1p Рік тому +1

    Bayiwo dangua manatoul

  • @maimounaka5561
    @maimounaka5561 Рік тому +2

    On a opéré sa bosse ou quoi ??

  • @sambanossosethnjie7319
    @sambanossosethnjie7319 Рік тому +3

    Bandit bou maguet bi lane laye wakhe nii😂

  • @cheikhibrafall1993
    @cheikhibrafall1993 Рік тому

    Bandit bu mak nga

  • @cheikhibrafall1993
    @cheikhibrafall1993 Рік тому

    Daa amatul doolé rék

  • @AleThiam-i6h
    @AleThiam-i6h Рік тому +1

    😅😅😅😊

  • @elhadjimbaye666
    @elhadjimbaye666 Рік тому +2

    Journaliste bii il est nul

  • @awagueye7640
    @awagueye7640 Рік тому +1

    Diaw aka meuno sagnessé

  • @galsen5350
    @galsen5350 Рік тому

    Domeram bi koumouy fathieu

  • @ndiayeibrahima9876
    @ndiayeibrahima9876 Рік тому +2

    Lima geuna meti ci ancien bandit même histoire laniouy wakh kw andando you bonne

  • @mordakhete4344
    @mordakhete4344 Рік тому +4

    Journaliste bi elle est nulle way akh do teuthi sa gat bayi ko mou développé

  • @gorguimalickfall65
    @gorguimalickfall65 Рік тому

    Ki doul rek lay def j le connait très bien ' Lou nék def nako dialoul arrêt sips fofou nekone nafa Di def faux aveugle Di yalwaane

    • @fififaye2603
      @fififaye2603 Рік тому

      😂😂😂

    • @mamesms3537
      @mamesms3537 Рік тому

      😂😂 woyy magui ram balalko rek garmi deugu mokay yeureum Pabi

    • @beuguefallou6555
      @beuguefallou6555 Рік тому

      Bayil diambour sa khôl bu Bone khamaloko Dara nékal guor yalla way ahh lii guay waax Dou deugu ba parei yalwane nékhoul kén kou sagnon bokk si gniy diokhé

  • @cheikhahmedtidianediaw9807
    @cheikhahmedtidianediaw9807 Рік тому +1

    Sama domou baye bi kou yabatéla deme ba magate nane daye toupe ya bone

    • @manoudiallo1350
      @manoudiallo1350 Рік тому +1

      Yow kou soxar nga. Yallah biniou bindeuh mom niou chaque jour niou togn ko balou. Yow sa dieumi bop yangi si ay bakar yo xamni toujours nga balou borom bi. Kou dem ba regretter tegouwate si yone ba parer di diox jeunesse bi ay conseil dango ko wara nianal. Soukou nexone guen si télé yi nane mako defone ma tay je ne regrette rien ba parer nane jeunesse bi dem len def com mane nima done def teh bou boba kene dou si meun dara

    • @khalifambengue6125
      @khalifambengue6125 Рік тому +1

      Toub dou wès moudij bou rafét rék mo diarra nian té yaw mi wakh khamo foy moudij

    • @MdiayeLota-xg1em
      @MdiayeLota-xg1em Рік тому

      ​@@khalifambengue6125yala mane nala ball si ligako togne wayè sa diguantè ak sa morom yala dousi dougou tè khamo niata domou adama la togne

  • @youssoudiopve4560
    @youssoudiopve4560 Рік тому

    Way sadata ndaye reey guanite dina deegue ndeye

  • @momodounyang476
    @momodounyang476 Рік тому

    Deugele

  • @Reactionseriesenegal
    @Reactionseriesenegal Рік тому +3

    Yalla n'a sunu borom doli soutou re

  • @BachirNdaiye
    @BachirNdaiye 9 місяців тому

    ❤❤❤❤❤❤

  • @AbdouDiop-rv2vp
    @AbdouDiop-rv2vp 7 місяців тому

    ❤❤❤❤