Ancien Bandit à la Médina terrain jaraaf « dama moudié Goumba » Allahou Akbar😱 Lily retrace sa vie

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 7 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 283

  • @makhoudiallo1
    @makhoudiallo1 5 місяців тому +18

    Yallah dal moy Dioubal diamam, 1987 Sama papa dafma yobou fouta car commence won na bon, mou metti ma trop, ma dem nek dara, di continuer ecole aussi, Yallah dima sopi ma dem ba am BAC, am sama Master sama MBA actuellement je suis Reponsable Regional Adjoint des Finances et des operations dans une organisation Internationale

    • @SokhnaNdiongue
      @SokhnaNdiongue 5 місяців тому +6

      Mashalah santal yalla ak sa papa takhawou nala sinon danga narone bone

    • @coumbadieng2969
      @coumbadieng2969 5 місяців тому

      ❤❤❤❤❤❤

  • @ahmadouka8036
    @ahmadouka8036 6 місяців тому +86

    Addouna ya meuna warr
    Yalla naniou yalla mousseule ci chèytanè

  • @AliouCisse-x5d
    @AliouCisse-x5d 6 місяців тому +15

    Yalla na yalla dioubeul mbolém mbinff si barké mouhamed amiine

  • @ataal6237
    @ataal6237 6 місяців тому +2

    Salam Salam depuis la Grande Bretagne. Kou melnii nak la societe sokhla. Ministere bi yore education ak culture daniouko ware encadre diko yaubou si ecoles yi ak associations de jeunesse yi mouy expliquer diar diaram pour yehtteh. Personnes avec lived experience are valuable, contrairement a ce que niou beuri Di moytou ak daw. Yalna yallah doli soutoura teh dioumal niou. Vraiment merci

  • @aissatousylla4172
    @aissatousylla4172 6 місяців тому +42

    Ndéyssane yalna la YALLA diégal mayla wéer ak nioune nieup si barké SEYDINA MOUHAMED S.A.W amiiine amiiine amiiine

  • @Enfant_béni_7
    @Enfant_béni_7 6 місяців тому +183

    Daguay guiss kou doundou banditisme ba diékhal nane dafa TOUPP di conseillé watté té banouy tolou séen digou doolé 😢 ray ay niit , sathieu , Aggressé améel ay niit akh youdoul dièkh après begeu ame moudiou bou rafett non c'est impossible car ALLAH ❤ IL EST TRÈS JUSTE ☝🏿dou YAlla guén amel akh dé bay toupp mais NIIT yiguén MEUSA togne guén Amel akh nak Sunu Borom diganeté NIIT AK moromam kinou togne rèk lay FARAL lègui yén foléni guisséti NIIT yoyou pour Balou léen akh 😭💔banouy tolou sén digou doolé yaay wax , papeu wax , kouné wax niouné toubounou danouy déf linou sentir mais je juge personne SAma xalatt rèk la wax , koulé ni Faral nak dafa fèkeu mousou nioula agressé wala Bandit mousoul ray sa dérett té NAFÉKEU nak bougoul kouy wax DEGEU. Téksi seytané yikoy Faral moy gniye diawalé toupp ak dém ba teulé amatou doulé ba Geumbeu wala feuneukh..niakeu pékhé tokk Di reuthiou,, MES FRÈRES GENRES NIIT YI WARNANOU YÉE KOUNÉ SI ADINA BANDITISME AMOUL MOUDIOU BOU RAFÉTT TÉ REUTHIOU DINA FÉKEU DIEUF FESS YALNANOU YALLA DIÉGAL TÉ MAYNOU MOUDIOU BOU RAFÉTT 🙏🏿🙇🏿‍♂️☝🏿😭💔✊🏿🫵🏿😔😥😢😭💔🙏🏿

    • @papasambadiop7599
      @papasambadiop7599 6 місяців тому +30

      Légui niom bouniou conseiller woul niom gniko dound niane nioy conseiller???? Foutaise.

    • @ndiaganiang1945
      @ndiaganiang1945 6 місяців тому +8

      Absolument

    • @gabrielngom7185
      @gabrielngom7185 6 місяців тому +7

      yow khamoo ni aduna di dokhee konn

    • @Enfant_béni_7
      @Enfant_béni_7 6 місяців тому +17

      @@papasambadiop7599 banou waré wone toupp Di conseillé waté mo yagg mais Bayi ba ndéy Maguette dinou sonal té yagg trokhal NIIT Yi yaw mom Koula guiss xameni 6 Moy 9 🫥

    • @Enfant_béni_7
      @Enfant_béni_7 6 місяців тому

      @@gabrielngom7185 kou wax degeu guéni bagn pask ay nafékeu guén

  • @soxkhou247
    @soxkhou247 6 місяців тому +12

    Yalla nagne yalla mouthieul té may gnou moudj bou rafet aaamine
    Yaw ya yees ci domou lakakatt kou djokk ni serigne Touba

  • @niakkbakarr1805
    @niakkbakarr1805 6 місяців тому +20

    Yalna niou yalla khirtal ci ak ndioupp

  • @ramatoulayedrame6589
    @ramatoulayedrame6589 6 місяців тому +76

    Kou foyee sa ndaw yakh sa mak, yague yague rethiou rek tee banditisme amoul mouthie, yallah na yallah dioubeul ndiambott gui tee khiir lene tchi boppame.

  • @dabafall-3173
    @dabafall-3173 6 місяців тому +7

    Bly j’ai le cœur meurtri en voyant les jeunes qui prennent ce même chemin

  • @NdiayeBara-lj9me
    @NdiayeBara-lj9me 6 місяців тому +21

    Boudé lingay wax nii degeu la si io dh baxna machalla yalla nala yalla geuna sopi

  • @fatoureinebadji5892
    @fatoureinebadji5892 6 місяців тому +2

    Machalah il n’est pas trop tard pour se repentir yalla nagnou yalla khir thi bopam

  • @Epitucule447Fall
    @Epitucule447Fall 5 місяців тому +1

    Yalla nagnou yalla maye moudiou gou raféte amine incha alah

  • @Culturevibes-sunuwork
    @Culturevibes-sunuwork 6 місяців тому +15

    Temps que Yagui noyi ! Reuthiou dou Wess Ya Allah reka xam li nek si xool yi

  • @diagnemomo4771
    @diagnemomo4771 6 місяців тому +23

    Atouman ak Walker ak yaya
    Ay policiers you meunone sén liguéye
    Bouya thiam ak wéllé ak baye ali ay ak ndaga ay bandits lagne wone
    Marché goudi louniou sath fofou lagnko done diayé
    Rue13/18
    Keur malaw fala boy médina yeup diangé touxx yamba ak cocaïne
    Gal ga fala ginzmane yi ak faxman yi nékone moy terrain manakana
    La Médina ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @diagnemomo4771
      @diagnemomo4771 6 місяців тому +2

      Bamba Fall défoule dara médina loudoul sathhh
      Bamba Fall bandit leuuu
      Medina bén maire la amone ba niar saxx
      Biram sassum sy avocat
      Pape Diop pds
      Bamba Fall rékkk😂😂😂

    • @fatoubilelkane5804
      @fatoubilelkane5804 6 місяців тому

      Cava Li bane côté la si médina svp

    • @sympathisante17
      @sympathisante17 6 місяців тому

      ​@@diagnemomo4771chef f quartiers fictif 😂😂😂

    • @adamambaye1514
      @adamambaye1514 5 місяців тому

      ​@@diagnemomo4771.

  • @Moussandiaye21994
    @Moussandiaye21994 6 місяців тому +12

    Lily borom bakh saf xorom bilahi ❤

  • @younoussba-o1d
    @younoussba-o1d 6 місяців тому +46

    Vrai souvenir école 2 ,/ 3 terrain maracana terrain diaraf pa Ass notre formateur avec coach Farmoz et coach Jules j'habitais à la rue 21 × 22 ❤❤❤ merci Médina tv pour ces beaux souvenirs

    • @fatoubilelkane5804
      @fatoubilelkane5804 6 місяців тому +5

      Iii ban côté la si medina

    • @abdoulwahabba2841
      @abdoulwahabba2841 6 місяців тому +1

      ​@@fatoubilelkane5804école médine

    • @bambamars2352
      @bambamars2352 6 місяців тому +3

      Ohh Pa Ass sama pere sama kharit un grand formateur

    • @mouslayeimmosenegal3529
      @mouslayeimmosenegal3529 6 місяців тому +1

      @@fatoubilelkane5804fi moye école medine, médina 1 ba 5 la wone Mangui deukone rue 19 angle 4

    • @thiernobah1308
      @thiernobah1308 6 місяців тому +1

      Moi aussi j'étais c'est pa Ass en 2002 jusqu'à 2005

  • @BinetaNdoye-yf6pp
    @BinetaNdoye-yf6pp 6 місяців тому +16

    Bonne amoul djeurign bakh sone Bone sone bakhal mouye sa djeurign

  • @makhfaye-c2k
    @makhfaye-c2k 5 місяців тому +4

    Senegal li motakh raye bi di bary do référence pour jeunesse bii

    • @fas2822
      @fas2822 3 місяці тому

      Non légui nak référence leu

  • @yacinendiaye2100
    @yacinendiaye2100 6 місяців тому +7

    Ndeyssane ya guorreee nak machalla nalla yalla may hol mougne

  • @sympathisante17
    @sympathisante17 6 місяців тому +6

    Yalla nagn borom bi mayy moudiou gou rafetttt.. 😢😢😢😢

  • @mouhameddiagne7192
    @mouhameddiagne7192 5 місяців тому

    Ndaysane yalla nala yalla defal jam. Tchey aduna😢😢

  • @fsene7089
    @fsene7089 6 місяців тому +18

    Vous avez terrorisé toute une generation bilay , j'ai fait mon cycle primaire a la medina 2 ( matar diop) années 85-91 , on ete obligé de faire le tour vers le marché tiléne pour ne pas passé par le terrain diarraf et devant ce fameux baobab !!!

  • @yayefallkawsara
    @yayefallkawsara 6 місяців тому +1

    Gaayi dh lolou lagnouye bagna dégue
    Kasso kou défoul dara wallahi doufa dougou
    Yalla nagnou yalla dolli soutoura

  • @sokhnamboup9781
    @sokhnamboup9781 6 місяців тому +6

    Ndessane yalla nala yalla diégeul

  • @NdeyeArameDiop-v5r
    @NdeyeArameDiop-v5r 6 місяців тому +14

    Toupe d'où niak pèkhè ndimbeulou yalla la ak moutier bou rafet l'île boul khaadi dèè yalla n'a sougnou borom gueule la diapalè parceque il a le grandeur regrete donc bonne continuation grand lili

  • @YacineSene-s4c
    @YacineSene-s4c 4 місяці тому

    Machalla yalna yalla arla

  • @ousmanetine4777
    @ousmanetine4777 6 місяців тому +2

    Oh grand Lily, Qu'Allah veille sur lui.

  • @Khadydiopbarry
    @Khadydiopbarry 6 місяців тому

    Thiey yala souvenirou école médine pa almand deysane yalanako yala yeureum

  • @IbouNdiaye-h1s
    @IbouNdiaye-h1s 6 місяців тому +6

    Motakhitt yalla khissappp nalako

  • @damefall4471
    @damefall4471 6 місяців тому +6

    Ndeysan thiey Diarr'diarr😢😢
    ❤❤❤🤲🏼🤲🏼🤲🏼

  • @serignesall3257
    @serignesall3257 6 місяців тому +3

    Je le trouvais souvent au terrain de jaraaf il fut des temps Il travaillait avec bamba Fall, ce dernier l'aidait beaucoup.

  • @MariamaNdiaye-ot8zj
    @MariamaNdiaye-ot8zj 6 місяців тому +1

    Yalla nala yalla diegal li passe yalla smou ñie dess ba donou ko def

  • @balmah1
    @balmah1 6 місяців тому +12

    Un péché reconnu est à moitié pardonné.
    Dieu pardonne ceux qui se répentissent à moins qu ils ne se récidivent

  • @bababodiang
    @bababodiang 6 місяців тому +1

    QU'ALLAH t'assiste et t'accorde longue vie

  • @zahrafatima1395
    @zahrafatima1395 6 місяців тому +3

    Ndeysane yAllah naniou borom bi maye mouthiou gou rafete tè baxale niou

    • @basselabdou9891
      @basselabdou9891 6 місяців тому +1

      Lolou rék modiara niane amine🙏

  • @Bigboss-hd8fx
    @Bigboss-hd8fx 6 місяців тому +11

    PA ALLEMAND MOY DIOP L'ancien gardien de medina 1 le pere de ismaila et abou mangui wone medina 5 ex ecole mamour diakhaté ; madam rose, madame ba, monsieur sarr, madame dieye, monsieur sarr serere, Directeur Samb grand pere de Anta samb jetais dans la meme classe que Idrissa kassé, Charles Ndoye, alassane ndao,demba diaw, khadijatou diallo, aby sow, aissatou gaye ca fait plus de 30ans je nai plus de leurs news ❤

    • @babacarsamb5646
      @babacarsamb5646 6 місяців тому +1

      Pa allemand décédé bou yageu mais ndiabote gui beu legi gnongi deuk fofou

    • @Bigboss-hd8fx
      @Bigboss-hd8fx 6 місяців тому

      @@babacarsamb5646 sisi j'avais appris son décès diadieuf

  • @AbdoulahadSylla-f9h
    @AbdoulahadSylla-f9h 6 місяців тому +1

    Du courage papa Dina bakhe

  • @modouthiam1127
    @modouthiam1127 6 місяців тому +10

    Baye ba ñiaka ndiariñ 😂😂😂nane Toupna

    • @hamzadiallo3300
      @hamzadiallo3300 6 місяців тому +1

      Boul wakhlolou waye frère adouna defa koudou tankeu

    • @fas2822
      @fas2822 3 місяці тому

      Loolou la ci borom bi beugoone au moins Yalla baayinako mouy dounde pour mou meuneu changé

  • @salldineakdiamono2391
    @salldineakdiamono2391 5 місяців тому

    wa mai grand boyi sèn tank laniouy diarre

  • @ngomkhadim1749
    @ngomkhadim1749 6 місяців тому +10

    Fi la dioudo rue 9bi ndeysane mangu joal actuellement yalna l'en yalla dolii tawfekh

  • @alhamdoulilah5446
    @alhamdoulilah5446 6 місяців тому +7

    Yalna nala Yallah diégal té doli la yiw. Les enfants voici des conseils qui peuvent vous être utiles.

  • @gabrielngom7185
    @gabrielngom7185 6 місяців тому +4

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤ très belle leçon de vie, merci

  • @bababodiang
    @bababodiang 6 місяців тому +2

    C'est un éducateur vraiment

  • @Xamxamtv-v2f
    @Xamxamtv-v2f 5 місяців тому

    Kou xam gougne Nguen te

  • @moustaphaba5386
    @moustaphaba5386 2 місяці тому

    Béne timis touti niou raye ma birr terrain jarraf periode élection présidentielle 2012

  • @FrancoisDiop-uw6nb
    @FrancoisDiop-uw6nb 5 місяців тому +1

    KU GEUM-NI KU BOTT BOUKII XATHIE MBAW LHEU" LALALE J'AIME 👈

  • @bababodiang
    @bababodiang 6 місяців тому +1

    Très instructif vraiment

  • @MbayeGakouNDIAYE
    @MbayeGakouNDIAYE 5 місяців тому

    Grand naga,wéllé, bouya Thiam...les petits boy laye toungouné,boy poulo etc

  • @fatimafatima-xh4fn
    @fatimafatima-xh4fn 6 місяців тому +5

    bandit amoul finalité bou raffett

  • @mouslayeimmosenegal3529
    @mouslayeimmosenegal3529 6 місяців тому +5

    Pa Ass diack mo yorone école de football terrain jaraaf ooh médina mo yagueu nexx fila dioudo rue 9angle corniche magué rue 19angle 4 fi la diangué école medine médina 4 ak 1 ba 3

  • @thiernobah1308
    @thiernobah1308 6 місяців тому +4

    Qui se souvient du fou qui était ici a l'école Medine on l'appelait Bir mouss il est décédé yague naniou titeul fofou😢😢

    • @domoubadiane348
      @domoubadiane348 6 місяців тому

      Khamone nga beneu dof bou nekone si corniche bi guedjou ifan gnou dane ko wower papa gol gol.

    • @bellangediouf9365
      @bellangediouf9365 6 місяців тому +1

      Bir mouss hamonako, il nous faisait peur...😂😂

    • @babacarsamb5646
      @babacarsamb5646 6 місяців тому +1

      Moi 😂

  • @MARIEDIOP-q4c
    @MARIEDIOP-q4c 6 місяців тому +3

    Il fo l encourager il n est jamais trop tard pour bien faire au moins il c ressaisi

  • @mbayendoye8053
    @mbayendoye8053 6 місяців тому +4

    Bouya Thiam kou yagueu beugueu khale....ecole medina 1 aye souvenirs inouabliables...Je me souviens de Pata,Ndiol,toungoune,boy laye ect....reacreation on allait voir Bouya et il nous donnait de l 'argent.

    • @mariamakebe3725
      @mariamakebe3725 6 місяців тому

      Bilaye tu as raison Bouya Thiam kou beuguone khalé avec sa copine Salma une fille très belle à chaque récréation école médina 1 dégnouye déme si galgui pour le salué nite bou bakh bilaye beaucoup de souvenir

  • @sambaalisow6921
    @sambaalisow6921 6 місяців тому +7

    Adina amoul solo dioup rek mo bakh

  • @FatmaDiouf-m3q
    @FatmaDiouf-m3q 5 місяців тому

    Akh dafa séwe akh késsé mola diapeu

  • @bababodiang
    @bababodiang 6 місяців тому +4

    C'est la bonne fin qui compte dans la vie des gens

  • @KineMbrngue
    @KineMbrngue 6 місяців тому +3

    Yéneu Yéna takh banditisme bi di law li kéne douko émission khana amo léne programme

    • @fas2822
      @fas2822 3 місяці тому

      Non au contraire

  • @aboucamara6679
    @aboucamara6679 5 місяців тому

    J habitáis a la rue 10 x 23 medina j etudais jean de la fontaine rue 22x37 et 39

  • @sokhnaoumoudiop6888
    @sokhnaoumoudiop6888 6 місяців тому +11

    Bandit yep sen khôl dey rofet waye amoul moudj

    • @fas2822
      @fas2822 3 місяці тому

      Billaay en général daniouy beug xalé, xamna dafa am loulène manqué té wolou wouniou Yalla

  • @AblayeTall-zy6gm
    @AblayeTall-zy6gm 6 місяців тому +3

    Médina 2 dans notre classe de cm2 quand on ouvré la fenêtre on appercever le baobab

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 6 місяців тому +15

    Bandi amoul ndiarign ak rk ak rk meno moudie fou bakh

  • @serignegaye-lp8yu
    @serignegaye-lp8yu 6 місяців тому +1

    La vie est très courte chaque personne doit change son habitude

  • @makhfaye-c2k
    @makhfaye-c2k 5 місяців тому

    Dagno wara raye sa ndaye doméram yie doléne rouse do référence pour jeunesse bii

  • @diopamar1
    @diopamar1 6 місяців тому +7

    Toubo dé dagua amatoul doolé rék

  • @mamediarrabeye-ed1zd
    @mamediarrabeye-ed1zd 6 місяців тому +5

    nit ken douko jugé yalla rek mo kham mais goumba dou agressé

  • @SambaDiawaraSarr
    @SambaDiawaraSarr 6 місяців тому +8

    Yonou Bandit amoul Ndieurigne Dou am moudiou rafette

  • @babacarmbaye8840
    @babacarmbaye8840 5 місяців тому

    Lima diakhal niome kousiy wat danga barkep serigne touba wala serigne fallou ken dou seydile hadji malick sy

  • @OmarNdiaye-i9k
    @OmarNdiaye-i9k 6 місяців тому +8

    Lily que dieu te protége adouna amoul solo

  • @awabop5671
    @awabop5671 6 місяців тому +1

    Allahou Akbar courage rek

  • @bayegaye-qf4kv
    @bayegaye-qf4kv 6 місяців тому +5

    Bandit ya pas de vie ni le respect les bande organisée ak bandit salité bokhoul lui ces un innocent qui n'a pas de soit de vivre sans éducation à la base ni repère maintenant c'est leurs tours de payé chér maintenant ya après la mort que Allah te protège frère longue vie

  • @alouguy5991
    @alouguy5991 6 місяців тому +4

    MACHA ALLAH RIEN N'EST TROP TARD

  • @MamecheikhNgirane
    @MamecheikhNgirane 6 місяців тому +2

    Yalla NANIOU BOUR LAHOU YOK SOUTOURA

  • @mamediaby6090
    @mamediaby6090 5 місяців тому

    Day féne , réyna ba tayi

  • @helenepouye8907
    @helenepouye8907 6 місяців тому +4

    Le mal se paie

  • @CheikhIbraFall-u2r
    @CheikhIbraFall-u2r 6 місяців тому +1

    🇺🇲 Congratulations à Médina TV Law ❤ndeyssane ce vieux connais toutes m'a famille j'habite juste en face mairie médina😢 qu'Allah nous accordes une bonne fin incha'Allah ❤galé Malaw est en face de chez moi seydina aussi était un ami de mes parents pape Sow est toujours en vie 🎉

  • @mercifulservant5526
    @mercifulservant5526 6 місяців тому +1

    Yalna Allah yeureum

  • @serignesall3257
    @serignesall3257 6 місяців тому +6

    Lily un gars bien le connait bien il habite à Médina rue 27 angle 10 près du district sanitaire de Elisabeth Diouf

  • @adjifambayesow6992
    @adjifambayesow6992 6 місяців тому +2

    Medina 2 la dianguè

  • @AbdouGueye-m5u
    @AbdouGueye-m5u 6 місяців тому +1

    Wakhji Yep len rek momaci nakhary limowakh nimo doon dokalle dorog bi ci pirission bi warokowo' guene ci vidéo bi khamo dara

  • @dieynabadiop4333
    @dieynabadiop4333 6 місяців тому +7

    Defa wah lou am solo sa yaye ak sa papa de gnu wah ba sonn do deug do len fale te beug Lou bahh lagn la beugal ben alkaly wah nga def par force avec respect l'an mo fi diar li yereum len parents yi sonn nagn fi ngen di nek ci prison parents yi gno geuna souffrir bilay sonn stresse di len di ray ba hey dee

  • @Khadyv.h
    @Khadyv.h 6 місяців тому +2

    Bouya thiam nion bokone kongne akka bakh nedeyssane adouna dou dara bouya thiam si famille boukh la bokk 😢

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 6 місяців тому +5

    Ki ko nekhhhhhh. Un bandit ki se dit khol bou rafet

    • @fas2822
      @fas2822 3 місяці тому

      Mais c'est possible gni en général daniouy beu xalé, meune nga def loubone fek sa xol rafet, mooy lima wakh rek niaka woolou Yalla meune n'a la defloo Lou bone

  • @ndeyefatougoudiaby744
    @ndeyefatougoudiaby744 6 місяців тому +12

    Yalla naniou yalla moussal si lou bone

  • @Baicherno-j9d
    @Baicherno-j9d 6 місяців тому

    Thanks

  • @SeckAdama-tp8qh
    @SeckAdama-tp8qh 5 місяців тому

    Ani wa Mansour Sy Malick

  • @khadimdieng1745
    @khadimdieng1745 6 місяців тому +6

    kou fowé sakk ndaw sak makk rere la

  • @sambasorysow3180
    @sambasorysow3180 6 місяців тому

    Mann bi may deukeu medina kenne amoulwone fitou agresse bire medina rue 33 x 10 Diecko

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 6 місяців тому +2

    Ancien bandit. Niata nit nga raye

  • @issakasylla1979
    @issakasylla1979 6 місяців тому +2

    Le presentateur cest le jumeau de waly seck😂

  • @bourathobouratho4672
    @bourathobouratho4672 6 місяців тому +7

    Bandit bou diékhal rék né toub na

    • @Pm007x29
      @Pm007x29 6 місяців тому +3

      Saway yalla nena bountou toub dou teudiou 🤝

    • @bourathobouratho4672
      @bourathobouratho4672 6 місяців тому

      @@Pm007x29 ok lolou tamit deug la

    • @fas2822
      @fas2822 3 місяці тому

      ​@@Pm007x29au moins amna chance toup, amna niou deh ci sen dig deunde

  • @CheikhDiouf-u5h
    @CheikhDiouf-u5h 6 місяців тому

    Ate.kabaga Maracana diamano bouya Thiam

  • @serignesall3257
    @serignesall3257 6 місяців тому

    Où est ngalla Aka réw ,

  • @salldineakdiamono2391
    @salldineakdiamono2391 5 місяців тому

    ki da diarra yereum fofè ndayam sa adouna ba sa dolè dièh nane toup na dafa amatoul dolè rèk kone fok ga bayi yalla biga nèkè sa ndaw lala sokhla

    • @fas2822
      @fas2822 3 місяці тому

      Mais au moins Yalla maynako chance mou toupe, loolou la ci Yalla name

  • @juniorgueye9637
    @juniorgueye9637 6 місяців тому +1

    Bilahi do niemer sax djar fi

  • @MackySall-qh1ns
    @MackySall-qh1ns 6 місяців тому +17

    Def Lou Bone baxoul

  • @khadymelintourekhadymelin3635
    @khadymelintourekhadymelin3635 6 місяців тому +3

    yalla nako yalla kharé aldiana firdawsi ak molomou dioulite thi barké mouhamet saw amiiine yarabbi 😭😭😭😭

  • @Assanefall-uq1he
    @Assanefall-uq1he 6 місяців тому

    Ndeyssane père ass diak nitt kou bakh mognou yorone fofou

  • @IbrahimBah-dc7gb
    @IbrahimBah-dc7gb 6 місяців тому +1

    Lili Médine rue 10 man le boy medina

  • @IbouNdiaye-h1s
    @IbouNdiaye-h1s 6 місяців тому +5

    Bandit amoull mouth