Depuis kaolack on le suit rifou est unique dans son domaine, il est débordé de talent. Il est plus que temps mou guéné album pour gneup xam ni mo dakha rap Sénégal ❤❤❤.
Rifou continu à gérer ta carrière tranquillement et surtout n'écoute pas les méchants et les jaloux. Ce qui nous intéresse c'est pas qui tu fréquente ou avec qui tu deal. Tu es un être humain avec des appartenances qu'on doit respecter faralaal kuula nekh kénén faraal kuuko nékh. Bravo encore une fois pour le travail que tu es entrain d'abattre KKL
Clash ci rap la bok. That's real hip-hop. Rifou et Nara sont tous les deux des freestylers. Nara a donné sa réponse à l'instant même sur Point de vue #3. Kou meun sa morom douma.
King Rif Sen Baye 🎉❤
Bayil doul waye
@@Shakour_Ocbd iow mom esk cv
Sa bay mo daka doul nieup
@@ibrahimafaty8369 😝😝😝😝😝😝
TEXTES MUSICALITE REVOLUTION TONTOU TONTOULOU NICE @
Depuis kaolack on le suit rifou est unique dans son domaine, il est débordé de talent.
Il est plus que temps mou guéné album pour gneup xam ni mo dakha rap Sénégal ❤❤❤.
Bilahi mo dak rap Sénégal
Il est bon
Ryfou defale gayi nanke lii dh nara pi moko môme Borom beugne bou damm bii moko môme 😂😂😂😂😂😂King rifou dopp dh ❤❤❤❤❤❤
Y’a meun dh🎉
Sarap lii..mani sarap lii...dama deg sa projet guen rk mani kou rap lii( Nara P)
Il parle pas de bm jay mais Nara pi
Bm jay dou bal kennn
😂😂
@@nouveautemusicalsenegal3208 danga dég bro🎉
Tou ndem laaaay weurrr depuis près de 4 ans je l'ai perdu . Booo m'a qqi djaappalè dinaaa si contannne trope.nice song
Rifou continu à gérer ta carrière tranquillement et surtout n'écoute pas les méchants et les jaloux. Ce qui nous intéresse c'est pas qui tu fréquente ou avec qui tu deal. Tu es un être humain avec des appartenances qu'on doit respecter faralaal kuula nekh kénén faraal kuuko nékh. Bravo encore une fois pour le travail que tu es entrain d'abattre KKL
Nice bro trop nice recit respect ❤❤❤❤
Way tonton rifou way🎉🎉🎉
Respect bro do moromam bilakhy rap dou foh
Nice frère... Bonne continuation
Clash ci rap la bok.
That's real hip-hop.
Rifou et Nara sont tous les deux des freestylers.
Nara a donné sa réponse à l'instant même sur Point de vue #3.
Kou meun sa morom douma.
Nagn bayii mou sédd🥺niarri domou Saloum Saloum lagn liih khadioufii nara p Rifou 🥰 niou bayii mou sedd
Qui connait le vrai rap doit valider ! Le niveau est higher walahi et sans politique aucune. Force à toi le génie du mic.
Kéne dou ioe Rifou fierté de toi mon référence
Rif on the mic. Real Rap never Dead🎉
Js bandit 🔥🔥🔥
Wa li nékh Na dh ❤ sarap lii 😂 rifou arbitre réck lay déglou nga deug tééla yéwouuuuuuuuu😂
Rifou bandi mathie yaye séne baye kl king ❤❤❤🇸🇳✊👌
Bayil doul
Première commentaire Première vu ameta boy kl depuis Léona
Sarap li li nekh n'a way 😁 tmt 😁🤣🤣dolil clach bi amna nivo ✌️
Dop waoouw
Rif le talentueux ❤❤
Tes vraiment une pure talent,mé depuis bagna démé palais ba né 9 Macky la Sénégalais yi wédii...
Sarapp liii
C'est les meilleurs ❤
Dou Man Dj YETNO guay surpri parce khamna sa tallen bou bakh et k li mbalit la ci yaw💪RESPECT
Yaw nak y’a xam Rifou walahi li mbalite la . Rifou da yamlé boy bi dou ko taxa youxou
Li mou ko def pour mane dou clash juste pour Tekk ko plaçâme la rékk
Nara B wouyoull king Riff bbal lene
Rifou mon rappeur
Ay Con guèneu Koi 2 ✌️domü kl guènii Clach doff koi Rifou Narapii lay clach guèneu deuk Kaolack
Nice Rifou ✌️
Non son bi dinama Ray deuglou nako 10 fois
Rigoureux est très fort chapeau
Rifou king 👑 nice keep &Goin God bless 🙏🏾
Yh lou nice
Too ndeim family 🤩💪🏼💪🏼. From Kaolack.
The legendery la wakh ✊🔥 ki Rif dafa dépassé meun Rap
Il est trop fort
Mougui baax Bro
M rifou Moy Sam khareti ❤😂
Pure hip hop❤❤❤
Dal na ❤❤💪
Tu es le meilleur
Am’an Album you xéw si benu son ❤nice boro respect
Rifou 🎬real 🎼yangi tangue bay🎸⚡️
The best egotrip man in this school of Hip hop Galsen
Un gars très bon machallah.
One Love Man
Nice beat et flow. Bro comme d'habitude rifou for real
Toujours fidèle à lui même 😂 no grand bayil doŕé bi
Wa sarap lii kou Mome class bi Rifou khana dou mo Djo
Nara p
Franchement Rifou da meune 🔥
Rifou borom « kaffrine dafa developpé kom pas possible 😂😂 » néxoul ba néxoul mais ayoo 😂😂😂.
Ohh li néxna ya meun ya eup dollé
Bilahi rap rek lay def
Rifou no waay bayil roubé 🔥🔥🔥yeureumeul gars yi Tamite niveau bi yeikk na waay dama Contane bay reitane😂😂😂😂😂
Grand frr mogui cool
Nice ❤
Rifou franchement wargua diagui watt rap😢😢
Non vraiment yaw nakk boul niou yapp
Ndeye Maguette louy RAP ? Comme Xam nga RAP
Première commentaire Première vue ameth boye kl depuis leona niassene
Respect ❤👍
Rifou rap🎉 rap rifou
Big Dia from klking mougui cool deii klking Moyy Bou bakh bii
rifou loye khare pour tontou boye bi
Rifou yeurmandè wayy😅😅
Il ne déçoit jamais rifou rk🎉
Ma ngui dhè ❤❤❤❤Rifou
Rifou y’a niak diom Nara sa baye la
Bilahi son flow est top defa rew nak Bro j admir
Vraiment yaye âme mou rap galsen
Du lourd.
Rap bi damkoy name
❤😎♥️Rifeu Deug
Première commentaire real kl for real
Dosén morom Big up👍
No rifou ya fi né🎉
Niveau ❤
🔥🔥🔥 So Hottt bro congratulations
Rifou one the mic
Big up frr migui cool déh 🥰🎉🥳
King bii mo Bax si nopou real
Rifou kong gande
Contane naa
Big up man🎉❤
Waouh quel flow ❤
1:56
Tu es le meilleur ❤
Lii Dafa Grawww Dope 🔥😍
Yeah nice
Cool🎤🎤🔥
Nice na bro
Dope vraiment
Kou fi guiss 9 Macky c’est rifou
Loumou wakh ??
9macky canara bi 😂
😅😅😅😅😅
Kk 🎉the best
Dope mon frére
Rifou c le meilleur
💪🏾💪🏾💪🏾
Li nice naa
Il fait partie des meilleurs RIFOU❤🇸🇳💯
LINO-221 DEPUIS KEDOUGOU 🎉❤❤ DOP MON GRAND 🎉
🔥💯💯🔥 sarap li waye
Rifou Gaindé Rap galsen bi 🤌🏿💫🎉🇸🇳
Vraiment, plume bi est là
🎉
Le début d'une très belle chose 🎉
Sa deug deug lii dafa nice trop baar bi kawena
The King rifou from kl dop