Je te jure falll depuis ay atte deglouma musik sénégal mais yégua sama chaytané rifou barké Bamba t'es mon rappeur légui depuis Paris loumasi gobé garko daga febar broo
Depuis que j'ai découvert ce tube ya 6 mois seulement (j'avais arrêté d'écouter le rap galsen avec cette nvelle génération qui fait tout sauf du rap) j'arrête pas de l'écouter en boucle je n'avais plus espoir d'écouter du vrai rap from galsen...big respect Rifou
Je comprends maintenant pourquoi Akhlou Brick n'a pas voulu répondre à Rifou. Ce gars d'un autre niveau. Wawww🔥🔥🔥🔥. Kou beugg Akhlou Brick waxlén gnou déff glace.
Sheuteuteuteuttttt Rifou Balko Dépuis 3 jours Mangui Replay Son Bi mais Doyalouma. HIGH LEVEL Big. Yakarone nani dina Dina YAKHOU, Maintenant je suis sure que ni DOU YAKHOU. Merci RIFOU
Sérieux voilà les rappeurs que je PX écouté 100000fois mm avec mes enfants..car mm quand c'est du Clash sa éveille.... Toi et Nittdoff merci de tjr tenir le flanbo de se style de Rap..bu len djayy s'en styl a cause du money.. Vos song de il y'a 5-10 ans.mm.ba tey ont l écoute avec enjoy et éveille mais ts ces autres qui font du "rap-mbalakh ' eux sont tjr obligé de.sortir des Song every day car après 2mois ont les oublies.. Rap Djolllof mo row
''Ay dayzakala bou Ara amoul won xawma fo DIEUM Mariage bi rafett seuy ngeu T tok ngeu si PODiEUM Def ngeu ko parent mtx mouy deim di weur KOUKO GEUM (bis) Ara Dayza diokh nala CŒUREUM'' 4barres yi🥵😍
Quand tu fais du vrai rap peut-être tu seras pas riche ou populaire mais tu auras toujours du respect des vrais . Cette chanson a réuni technique,écriture et masculinité..and this is the way we love Hip-hop
Quand on parle du Hip Hop c'est sa du vrais Hip Hop. Rifou n'a fait que réveille les mélomanes. Music romantique n'est pas du rap vraiment. Bravo Rifou pour ce rappel et on attend le réplique de akhliu brique. Amoul ay douma tontou kii... On attend votre réplique #Akhlou_brique
Boommmmm Ayyyy rifou a frappé fort très fort même Il fait partie de ce qui ont resté sur le chemin du vrai rap galsene Pour moi il est le meilleur de sa génération Rifouuuuuuuuuuuuuuuuuuuu🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Le Sénégal est l’un des pays très rares où le real hip-hop existe jusqu’à présent. Donc Riffou tu n’as fait que remettre le drapeau à sa place respect ✊ peace and love RPZ KL FREE❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥
Machalla rifou clach bi Nice neu Tu as très bien défendu le hip hôp Grand yi liguéy liguéy bignoufi déf dafa beuri, warougnouko yak nonou rék ça serai vraiment dommage. Mais HEUREUSEMENT RIFOU mingui fi👑
RIFOU réponse daye mate réponse (Fuck j'aime) doma té j'aime nk instrumental khana moye wa Akhlou brick délou léne underground rape daye ndeye gooré walahi j'ai kiffé 💥💥💥💥💥💥wa touba gazz Di léne ziare 🤣🤣
Rifou tu es entrain de écrire une nouvelle page dans l'histoire du rap galsen ! Ca me rappelle bi fi gneup neké di way love rap adio gnow rappeler len à l'ordre ! Beat bi nice neu lyrics yi nice neu et saf neu mbed ! I like it !
Bou talent done Feyy Rifou di dawal Ferrari 🎤🧢
Je te jure falll depuis ay atte deglouma musik sénégal mais yégua sama chaytané rifou barké Bamba t'es mon rappeur légui depuis Paris loumasi gobé garko daga febar broo
Bou deugeur bi 4ever, Do Rappeuro Tik Tok aboo Camaro 👏🏾👏🏾👏🏾
Ndékété iao ya dioutou niou Kate la rifou
Il faut tous les mélomanes gnou soutenir rifou
Depuis que j'ai découvert ce tube ya 6 mois seulement (j'avais arrêté d'écouter le rap galsen avec cette nvelle génération qui fait tout sauf du rap) j'arrête pas de l'écouter en boucle je n'avais plus espoir d'écouter du vrai rap from galsen...big respect Rifou
Je comprends maintenant pourquoi Akhlou Brick n'a pas voulu répondre à Rifou. Ce gars d'un autre niveau. Wawww🔥🔥🔥🔥.
Kou beugg Akhlou Brick waxlén gnou déff glace.
Wah deugg, akhlou gno kham loutah dougnou tontou, wélélé rifou dagua doff
Dagni handiou rek fi koudoul Real dangay harrr
Ohh rap bou deguerr❤🎧💪📸
🔥🔥🎵🎵👑
le Hip-hop Galsen a toujours besoin de vous *Real King* 🔥🔥🔥🔥
Cv mon frr allhamdoulila abonnel bok sama chaîne rappeur bu ndaw la koi 🙏
@@Actu.200 bonne continuation GentleBrother
42 ans , et ce type de rap je croyais ça n'existait plus, chapeau bas for bringing back the kind of vibes
Sheuteuteuteuttttt Rifou Balko Dépuis 3 jours Mangui Replay Son Bi mais Doyalouma.
HIGH LEVEL Big. Yakarone nani dina Dina YAKHOU, Maintenant je suis sure que ni DOU YAKHOU. Merci RIFOU
Waou ✅👊🏽😳💸💰💸💰💸💰💰
Hooooooo big up
Sérieux voilà les rappeurs que je PX écouté 100000fois mm avec mes enfants..car mm quand c'est du Clash sa éveille....
Toi et Nittdoff merci de tjr tenir le flanbo de se style de Rap..bu len djayy s'en styl a cause du money..
Vos song de il y'a 5-10 ans.mm.ba tey ont l écoute avec enjoy et éveille mais ts ces autres qui font du "rap-mbalakh ' eux sont tjr obligé de.sortir des Song every day car après 2mois ont les oublies..
Rap Djolllof mo row
''Ay dayzakala bou Ara amoul won xawma fo DIEUM
Mariage bi rafett seuy ngeu T tok ngeu si PODiEUM
Def ngeu ko parent mtx mouy deim di weur KOUKO GEUM (bis)
Ara Dayza diokh nala CŒUREUM''
4barres yi🥵😍
Je le replay x fois bilay rap galsen yakou na legui koih bilay
Baal lenn 😂 rifou
clasiccccccccccc💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💯hip hop 4 life
Sa numéro guir yalla dama kontane ci calah bii❤️❤️❤️
Rap amna nak , meun rap amna nak , degloukatt amna nak 🔥🔥🔥🔥respect rifou
Quand tu fais du vrai rap peut-être tu seras pas riche ou populaire mais tu auras toujours du respect des vrais .
Cette chanson a réuni technique,écriture et masculinité..and this is the way we love Hip-hop
Kawé na bro
Le roi 👑
🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥fowoul 😤
En tt cas niveau leuh deh
Flow 100%
Vulgarite100%
Technique 80%
Punchline rimes 90%
🔥🔥🔥🔥🔥🔥🇬🇲
Rifou
😎😎Rifou
2pac techniques 100%
@@zizlaofficiellezizlaoffici9369 🔥😎👍
Technique 100% lii mou Def fi 2pac sakh menou ko
C'est la premiere fois que je t'écoute mais le hip hop est au RV. Nice et choc,y'a ngui si hip hop bi donc Dou Yakkou
🙏🏾 Alhamdoulilah ❤️ Jeureujeuf rifou rap ngua li laniou name, yow fo nékon
hooooo Sama yarame dawana rifou delonga ma dembe
Rifou bilay doo nit respé🤲
Rifou doo nitt🔥🥶am nga flow meune nga rap tékk ci di rimes you dall⚽🥶 respect rifou 🎙️dra Dou yakkou ndeyammmmm🔥⚽clozz t'a assuré ossi🉑🎹vive KL KING
Li moy vrai Rap hip hop Big Up Rifou Respect
Boy rapeur légui yi daniou yak Rap Galsen yeufou fek ,solou fek ,mbalakh bokoul si Rap
Quand vous voulez entendre du real rap , allez écouter Rifou . Il ne déçoit jamais ce mec . KL King respect 🫡
Yeah for real
Cv mon frr allhamdoulila abonnel bok sama chaîne rappeur bu ndaw la koi 🙏
Waxka Tchi Kaw Rap Pure Et Dure Sokay Dégg'Lou Ay Daatch Lalay Diokh Vrai Bombe Leuh🔥🔥🔥🔥
Je viens de le découvrir mais je suis vraiment choqué franchement ce grs est fort
Yay sococim si sougnou rap koufiii môle gnou rayy ndeyam 🔥🖕 MG from Arba
🔥🔥🔥📌mane batay mangui si clash bii batay ken tegoul lou geuneu kawer akhlou dano daaw dieul ngaka
1:57
Il M’a Tué
Noooooon RIFOU Con Nga 😂
Tu Es Talentueux Nak Vraiment 🙌🏾
Mais rifou technique neu millions floww tekthi
@@aliounebadaradiagne3323 Bilaahi Frr…Ndanaane Leuh Deh
Merci d'avoir ressuscité le hip hop galsen..mr rifou..
Gars yi mome legui ils font surtout du mbalax
tu fais parti des rares rappeur qui garde toujours cette touche particulière du réal hip hop
Wa li Amna niveau Dee 🤣🤣🤣 j aime.rifou.bilah yaw Nice rap d'où meusseu Dee❤️❤️❤️🇸🇳
Riffou guayi nane danga fouri instant bi dh yangui bess takk bay on love man
Mouk dou meusseu Yakhou Même bou déssone bén soldats.. Respect
Rifou ✊🏽✊🏽
Merci rifou il faut que certains rappeurs sachent que le hip hop galsen ne doit pas sortir du vrai rap
Hip hop for real 🤟🤟
Waaaaaw waaaaw waaaw nammmon naniou rap deugg
Niafff
Fi dra dou fi yakhou
Akhlou Brick dagno faté démb
Riffou dianguale lén tay
Diadieuff Bro 😉👍🏾
Wouahhhh 😍 le peuple du hip hop est content🔥🔥
Cv mon frr allhamdoulila abonnel bok sama chaîne rappeur bu ndaw la koi 🙏
Rifou ak meune rap ❤️👊classe direct très bien fait
Aight les puristes ne peuvent qu'être fiers 👏🏾 Classic Never Die
Yaw dafa ménni mart cheikh tidian yélla commencé dall
Daga trokh beu paré mes geum nani do talibé baye
Yeah you right Bro ✊
Do dra Rifou mbour Amoul fék
Shifaay nga gayi popopooooooooooooo
Sam wadji meun nga rap🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Classic Never die. Merci beaucoup Rifou. Liii laniou sokhleu
Je suis fans Dip ms Rifou je suis content de toi vraiment tu es Un Legende 🤟
Rap bi dou yakou vive bou deugeur bi et félicitations
Kou nieuw fii pour kham kane moy Rifou ?
Mais ce gars est chaudd motakh Akhlou brick nanguouwoul tontou
Niouss nioussaaat😂😂😂🔥🔥🔥🔥
Bou rap galsen tégonn lou lérr Rifou konn kéne wakhatou ko gayi yeup meune gua lénn botte di rap🙏🏽✨🔥❤️Billahi
Tapett bouy classe dou nangou toudou ayy tour
Merci défendre le hip hop galsen big up respect
Quand on parle du Hip Hop c'est sa du vrais Hip Hop.
Rifou n'a fait que réveille les mélomanes.
Music romantique n'est pas du rap vraiment.
Bravo Rifou pour ce rappel et on attend le réplique de akhliu brique.
Amoul ay douma tontou kii... On attend votre réplique #Akhlou_brique
Akhlou brick dou sa ndeye morome khamo sa bopou
Li moy rap goor yalla deug mais melni nadio
Merci d'avoir défendu le Hip hop au moment ou il a fallu que quelqu'un le fasse
Vraiment jajeuff Rifou
Tjr au top frero. Ta bien fait. Real hip hip. On attend le retour
Hip-hop dou meussa dé✊✊✊✊✊✊
Vérité indélébile vraiment
Toi qui a commenté ça tu ne connais pas le hip hop
Ohhhhhhh ! Very nice! Real rap. Big respect rifou. Je me rappelle de tes concerts à Kaolack. Un gars digne et engagé,namone na rap bi
WoW wow🔥rifou il es très 💪🏽 fort
Tu sei il numero uno di Red Carson
Lou yageu degeu le jahjeuf Diambar 🔥🙏💪🇸🇳🌍 jahjeuf 🙏
Là j’ai retrouvé mon Rifou👏👏👏
Respect rifou
Niveau bi adiou neu
Amneu talent
Real hip hop
Its all about hip hop
Boommmmm
Ayyyy rifou a frappé fort très fort même
Il fait partie de ce qui ont resté sur le chemin du vrai rap galsene
Pour moi il est le meilleur de sa génération
Rifouuuuuuuuuuuuuuuuuuuu🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Bu bax bila 💥💥💥👑👑❤❤🇸🇳🇸🇳
En ok kon akhlou yen mbaye guén yap rifou mom day 🔥🔥🔥🔥
Il y’a toujours des gens qui font du hip hop respect à Rifou
Ya les dignes qui seront toujours la pour sauver la vérité... Dopness kl a l'honneur
Cv mon frr allhamdoulila abonnel bok sama chaîne rappeur bu ndaw la koi 🙏
Waouh kel flow 💥💥💥rifou t'as assuré
Tak na len ni samay daaadiou joint
Bahal ni nadiou juin
Bou rap bi yahoooo sen carriere RIFOU def ci" point"
Tou ndeyam🤭🤭🤭
Que du lourd mon gars te le meilleur 👍
Le Sénégal est l’un des pays très rares où le real hip-hop existe jusqu’à présent.
Donc Riffou tu n’as fait que remettre le drapeau à sa place respect ✊ peace and love RPZ KL FREE❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥
Fiért de Rifou...c'est bien fait pour les rupou...loumou ladjie rék gnou guéné ték
Qui est là après le niveau très bas des Rambakheurs ?
Respect Rifou 🫴
Non dagueu ayyy 🩸❤️✅
technique flow tout est carré merci d’avoir défendu le hip hop galsen au moment ou il en a vraiment besoin
Goor dou yeureum goor 👊🏿👊🏿
Kou je kou sa mrom yeuy 🤣
Machallah félicitations nice job bon courage merci beaucoup infiniment
"Boulma niodi public ayy diouné ma ngimb, boulma niodi mystique bro ayy djiné ma ngimb " 🔥😂😂
Depuis THIOW Djiboul
Yayy ndanann deh
Machalla rifou clach bi Nice neu
Tu as très bien défendu le hip hôp
Grand yi liguéy liguéy bignoufi déf dafa beuri, warougnouko yak nonou rék ça serai vraiment dommage.
Mais HEUREUSEMENT RIFOU mingui fi👑
RIFOU réponse daye mate réponse (Fuck j'aime) doma té j'aime nk instrumental khana moye wa Akhlou brick délou léne underground rape daye ndeye gooré walahi j'ai kiffé 💥💥💥💥💥💥wa touba gazz Di léne ziare 🤣🤣
Le vrai hip-hop nous manque beaucoup ✨✨ j'adore
Wouhhhhhh🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥real rap never dead❤️😍
Brick rék💪💪🤫
Dop dop dop naaah mais rifu général 👮 bu rap galsen donë faye nga done milliardaire. Respect man !
Voilà, on a besoin de ce vrai RAP, vraiment jerejeuff,
Le song est dope🔥rap dou meuseuu déé💯💪🏾
Cv mon frr allhamdoulila abonnel bok sama chaîne rappeur bu ndaw la koi 🙏
@@Actu.200 ok metiwoul
Rifou tu es entrain de écrire une nouvelle page dans l'histoire du rap galsen !
Ca me rappelle bi fi gneup neké di way love rap adio gnow rappeler len à l'ordre !
Beat bi nice neu lyrics yi nice neu et saf neu mbed ! I like it !
Réécrire guay wakh keiy se mec depuis ses débuts il a toujours était à la hauteur juste da amone galankhoor reck Machalla
Rifou srx 🔥. Srxx. Tégal gua niou diara tégalll
Kl. King 📌
athia Rifou dopppppppppp n'a men
Rifou tu as vraiment réveiller les mélomanes du hip hop. Real hip hop never die
Ça c’est du hip hop lourd🥰
Franchement li dafei manqué woon🤣🤣
Au passage carrière romero dafa moning🤣
Dope nice classic dou meussa dé bgué et respect ✊
Pour moi le rap galsén déki na Rifou est un vrai rappeur genre nit dof bro tu es au top wallai
Rifou fo nékone ba wa akhlou brick déme bayila guayi lounioula djito meno léne dape té gua khare Tonton Deyza dibala tonte khana ladio Omzo😀😀😀😀