Urgence :Meurtre à Touba une femme à été tuée par son beau frère

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 6 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 253

  • @bocarba8030
    @bocarba8030 День тому +131

    Paix à son âme.
    Seuyou Sénégal dafa métti trope beuri charge à la maison sans compter les enfants les vas et viens les belles sœurs et beaux frères qu'on doit satisfaire et tant d'autres.
    Yalla na yalla diapalé sougnou sœur yi

    • @Md14949
      @Md14949 День тому +9

      Bilay ba poulo waxko thikaw

    • @CheikhtidjaneSeck
      @CheikhtidjaneSeck День тому +7

      Mane mome toutes mes sœurs Di seuye wakhouma raye kolene dorr ma récupérer porte plainte soko rayee môme ma raye la

    • @mberryable
      @mberryable День тому +3

      @@CheikhtidjaneSeckndeysan yalla nallen sunu borom doli soutoural thi barkep Seydina Mohammed Salalahou Aleyhi Wa Salim.

    • @CheikhtidjaneSeck
      @CheikhtidjaneSeck День тому

      @@mberryable Amine ya rabi niou fekeee inchallah merci sama khel khol mo diekh

    • @DoffSambe
      @DoffSambe День тому +5

      AK ay woudiou perthiorgo you sokhor ay goro you faté

  • @OussaynouSow
    @OussaynouSow День тому +50

    Tanyi doy n'a warr yalna yalla def diam

  • @HelenePouye-fk5em
    @HelenePouye-fk5em День тому +109

    Arrêtez il n est pas fou. Que justice soit faite

    • @OumiGueye-kq3pk
      @OumiGueye-kq3pk День тому +2

      Li mettyna

    • @mbissinesererelofficiel1812
      @mbissinesererelofficiel1812 День тому +9

      Merci moukoy outal lay vraiment k ses parent de la dame porte plainte

    • @papedaoudafaye8379
      @papedaoudafaye8379 День тому +9

      C'est toujours comme ça. La personne qui tue au Sénégal. On cherche lui trouve des prétextes en disant que wéroule. Sénégal dou réwe Bilaye. Tant que peine de mort amoule Sénégal raye yi dina guena barri.

    • @Nianistolelion3803
      @Nianistolelion3803 День тому

      Luci sa yone ak loula ci woor nga balma mais nianalco yala rek

    • @HelenePouye-fk5em
      @HelenePouye-fk5em День тому

      @Nianistolelion3803 le père a dit que le gars était un malade psychiatrique.

  • @FatimataBe
    @FatimataBe День тому +12

    Hum nitte kou réyi nitte guéne nane wéroul thieyi Sénégal kou reyi nitte rek weroul 😢😮😮😢 Sénégal dé baryna ayi dof cone

  • @user-tfaye
    @user-tfaye День тому +27

    L'heure est vraiment grave li mom mr bassirou diomay Faye Nassi wakh nakh parent yi s'en khél yi dalatoul di ray rek ni kou nekk canal + action rek😭

    • @naboukebe5390
      @naboukebe5390 День тому +2

      Te dou moudjie fen ki def double meurte mi ngui si tic toc bi di nakharalate nga khamne galsen amoul loi dieuleen seen responsabilite diko fadial seen popou galsen gouvernement bi eekafa am securite

  • @laminelayekebe615
    @laminelayekebe615 День тому +16

    Wa reew mi lane moniou dougu tmt 😢😢ray youdoule diékh 😢li mome war nAniou sé diouk 😒😒mogui beuge eupou lokho

    • @mamebacs6622
      @mamebacs6622 День тому +2

      en tout cas ca commence a devenir trop ray yi barina trope .ndeyssane yallah nako yallah yeureum

  • @khalifababacardiop8709
    @khalifababacardiop8709 День тому +21

    Ce pays là ne cesse jamais de me surprendre. Son na si Rip bi . Li ba kagn

  • @sokhnadiongue4410
    @sokhnadiongue4410 День тому +6

    Que justice soit faite mounane weroul

  • @mbenesarr1204
    @mbenesarr1204 День тому +28

    Gore gouni léngue di kheuthio ay pelou mbamite bassiye raye niteu mani na yone def ligueyam niouy wakh wakhi dof nii

  • @Nafidramè-r7b
    @Nafidramè-r7b День тому +17

    Yalla nako yalla yeureume tè kharèko aldiana

  • @SENEGALPUISSANCE-jd1te
    @SENEGALPUISSANCE-jd1te День тому +32

    2025 bi limou commencer grawna rék yale nako yalla yeureum te khareko adjana fire dawesi

    • @byanaartaye96
      @byanaartaye96 День тому +4

      Kone setlou gua lolou tangue na dall kou yabou moytou kou la tognie gua bayiko ak yalla ndeysane yalla nako yalla yeureum bilahi tant que peine de mort amoul dougnou arrêté

  • @syllamaman4914
    @syllamaman4914 День тому +33

    Bilay touba la deuk mais djiguene gnifay seuy sonou nane dou niepp nak beurinafa djiguene niou sonou nan

  • @Mamekharyfall-y8o
    @Mamekharyfall-y8o День тому +14

    Dégal pàbi wéradi xél dara dalouko mais Sénégal mome ni rék

  • @MoustaphaSarr-p5m
    @MoustaphaSarr-p5m День тому +97

    Lou waral Sénégal 🇸🇳 Ray. Yi barri ci weer yii😢

  • @MaquetteFall-f9u
    @MaquetteFall-f9u День тому +3

    Oh youma ndaysane yalla nako yalla yeureum kharé ko aldiana firdaws sama amie d'enfance la

  • @DiopNdeyendoumbe-f8f
    @DiopNdeyendoumbe-f8f День тому +35

    Bo rayé nit rek niouné weroule😭😭😭😭

    • @NdiobaDiouf-sg8er
      @NdiobaDiouf-sg8er День тому +3

      Sénégal Limou fi ame de ko ray niou né wereul😢

    • @ramadiatta-f6y
      @ramadiatta-f6y День тому +1

      mo meu diakhal 😢paix â son ame

    • @moniquecisse461
      @moniquecisse461 День тому +1

      Té sakh soune né werouk daneko wara topou khol fait yii noumou déroulé pour conclure ndakh c'est prémédité ou pas té sakh yoneu dako wara condamné sou feké c'est avéré qu'il est fou dans un structure psychiatrique mais hélas deuk bii mom legui keneu khamoul niane yalla diniou mom mouseul rek

    • @MuguetteDiaw
      @MuguetteDiaw День тому

      Moma diakhal 🤔🤔

  • @astoudiedhiou4099
    @astoudiedhiou4099 День тому +4

    Kou ray niou rayy là 🔥🔥🔥.

  • @fallyseye9598
    @fallyseye9598 День тому +14

    Mes janvier louy problème 🙆🏽🙆🏽

    • @diogoulfarba5586
      @diogoulfarba5586 День тому +1

      Janvier souffre des pêchers de décembre 😢

  • @thiernondiaye5126
    @thiernondiaye5126 День тому +1

    Que ce passe t'il au Sénégal c'est vraiment triste yallah yallah diegalko khareko aldiana Amine ya rabbi

  • @khoudjafall7291
    @khoudjafall7291 День тому +17

    Ay way ndaw yi yeram len sen wadiour... Ji wou niou len li dhé. Metit ak gatia bi ngen len di yobe😢😢

  • @sangesouPape
    @sangesouPape Годину тому

    😢😢LI DÉ DIARNA DIEUL GALL SANFOUWA

  • @adamasuwareh7838
    @adamasuwareh7838 День тому +2

    Rest in peace sohna yoma 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @charlotteantoniabassene-wg1yo
    @charlotteantoniabassene-wg1yo День тому +5

    Nioune djiguéne Sénégal amatouniou rongogne chaque jour dall il faut mou âme koniou réye .nitt da sacré guir yalla naniou nité .sama khol métineu trop sakh

  • @cheikhoumarkande4922
    @cheikhoumarkande4922 День тому +2

    Non Sénégal koufi ray nite niouné dafa weradi 😢😢😢😭😭😭

  • @khadyforbis3671
    @khadyforbis3671 День тому +20

    Khol ko mouy wakh ay wakhou wéredi
    Dara diotouko bayiléne séne dom yi bouniou rayé domou diambour ngéne di nane dafa dof . Yomb na trop Waioe

  • @AKD-u2c
    @AKD-u2c День тому +1

    Hum parfois, il y'a des maux qui Sévillent dans les familles et personne ne cherche à les pansser et donc les blessés et affligueurs de maux cohabitent dans une même maison alors forcément un jours viendra où un drame se produit. Creusez les absés et soignez les maux afin que la paix soit restaurée. . .

  • @maimounadatt7334
    @maimounadatt7334 День тому +5

    Ah li monme metina di 😭😭😭😭😭

  • @KhadiatouSagna
    @KhadiatouSagna 18 годин тому

    Allahoumah ihfirllaha warhamha😢😢😢😢😢😢😢réybi barina lôle Sénégal naniou andi péne de mort

  • @AwaFall-gi8qg
    @AwaFall-gi8qg День тому +2

    Allons rek ray rek pour lane kou ray nagnla ray 😢

  • @NdeyefaouSylla
    @NdeyefaouSylla День тому +5

    Ay lii Yana fii yam dii😢😢

  • @AbdoukhoudossNdiaye-u1u
    @AbdoukhoudossNdiaye-u1u 17 годин тому

    😭😭😭😭😭wa🔥🔥🔥🔥🔥🔥

  • @PapeFaye-m4t
    @PapeFaye-m4t 17 годин тому +1

    Yalna.yalla.def.diam.thi.rewmi

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 19 годин тому

    Ndeye saane yalnako yalla yeureum

  • @Ramzek-f3s
    @Ramzek-f3s День тому +2

    Les femmes ndeysaan, elles souffrent si sen seuy yi motakh niu beuri nangouwouniu seuyi keur famille leegui

  • @kalsoumdabakh537
    @kalsoumdabakh537 День тому +2

    Ay way li métina Say dom fonou dieum li seye métina 😢

  • @BayLay-i9t
    @BayLay-i9t День тому +1

    Walaye bouniou defoull atep sariha douniou ame diamou raye daye geuna bari rek di reye nite melne kouye raye kharr 😢😢😢😢li dafa sakh niaw

  • @kareabdoulahad622
    @kareabdoulahad622 22 години тому +1

    Ah wante raye yi dafa yombou trop comme ndokhou nane surtout moment yi

  • @user-tfaye
    @user-tfaye День тому +3

    Sénégal kou ray nitt niouni weroul waw nakh diotoul niou diay rewmi fou waye nekh dem li dafa niaw trop Sénégal niepp kham ko si pays de la térenga legui pays de Lou way nekh def justice pour youma😭

  • @BintaColy-sx2ms
    @BintaColy-sx2ms 20 годин тому +2

    Décidément legui doundou domou adama yi si lokho nit yi la nek yalla Mom amatoul droit dieul wa tito lenn en tout cas mane tite na mais paix à son âme aldiana sa keur 🙏 yalla yeureum ko si Barki seydina Mouhamed 🙏

  • @mansourgaye6205
    @mansourgaye6205 День тому +2

    Gorgui ragalal yalla li kay bouko délo si yalla délo kosi saytané xôl bou bonne ak nitt you bayima tané dougal kosi aya bi yalla wax ni lou nguéne defsi lou ñiawe yéna ko fagou thi séni lôkho yaléne bolé yilif aye mbok lagne dou très japp ko ki fi bayéko yalla nako yalla yereum té djégalko

  • @OumarDiop-g7r
    @OumarDiop-g7r 22 години тому +1

    Yalla na yalla yereme ko Amine

  • @AdjiNdoye-n9i
    @AdjiNdoye-n9i День тому +2

    Balama de reck niouni weridi ki def li naniouko raye mou diekh ray reck 😢😢😢😢😢😢

  • @bambadieng6025
    @bambadieng6025 День тому +1

    *PAIX A SON ÂME*
    *_en tout cas na yonn def liguéyam dagnoo waronn def kou ray gnou rayla,yéneu YI day beuga yombou dh bilahi ,mélni kou yor poulayé guinar djapou di ray rek_*

  • @makhousylla644
    @makhousylla644 10 годин тому

    Yala nako yallah yeureum mes vraiment li yombou na trop ray borōm ndiaboote si zéro ndax you niank fayda 😭😭

  • @naboukebe5390
    @naboukebe5390 День тому +1

    Yalnako yalla yereum souf woyof si kawam doynawaar dal galsen amoul loi

  • @makharyndiaye5922
    @makharyndiaye5922 День тому +1

    رحمة الله عليها 😭😭😭

  • @Issatraore389
    @Issatraore389 День тому

    😢😢😢😢mety na

  • @mamemorniang9550
    @mamemorniang9550 День тому +1

    Yalla na yalla yeureummm

  • @SigaFall
    @SigaFall День тому +8

    Thiey Sénégal aye reye rek dona war dal

  • @MoustaphaGueye-x9y
    @MoustaphaGueye-x9y 11 годин тому +3

    Yalla l'anatomie Yalla yerem 😢

  • @AssaneDiop-w5m
    @AssaneDiop-w5m День тому +1

    Yalna yalla sougnou borom xaré koo aldiana firdawci touba lane laa lou khéwe

  • @KhadimDione-s1y
    @KhadimDione-s1y 18 годин тому

    Djigeune gni môme dangaye warou dé dagnio tamou aye wakhe you séwe trop ndéyesane li eupou n'a way 🤔🤔🤔😭😭😭😭

    • @dabafall3
      @dabafall3 17 годин тому

      ANA gor ak khetho ay paile Bathiye raye gor day am fayda

  • @ousmanediop4110
    @ousmanediop4110 День тому +1

    Paix à son ame amineee YARABI ainsi qu'à tous nos défunts amine YARABI

  • @moctardiagne9943
    @moctardiagne9943 День тому +2

    Kou ray niou rayla rek, amoul lenene, nafekh rek niounane dogalou yalla....

  • @ojo990
    @ojo990 22 години тому +1

    Ana bay fall yi your security Touba bi

  • @MaibDiaw
    @MaibDiaw День тому +1

    Sama domi ndidiaye la di sama tourondo mé wéroul😢

  • @SerignefallouDiouf-bo3ny
    @SerignefallouDiouf-bo3ny День тому +6

    Mais vraiment tite na thi Sénégal

  • @Astoumbenediop-bn5jm
    @Astoumbenediop-bn5jm День тому +1

    Yala nako yala yeureum tei kharei Aldiana Firdawsi 😢

  • @PendaFaye-l9i
    @PendaFaye-l9i День тому +1

    Paix à son âme j'ai vraiment peur

  • @cheickoumardeme2284
    @cheickoumardeme2284 День тому +1

    Pax a son ame
    Amine

  • @coulibalyyacine6231
    @coulibalyyacine6231 День тому +1

    Yalla nako yalla yeureum

  • @Gallas-catalan
    @Gallas-catalan День тому +6

    2025 bi loum narr 😢😢😢

  • @FarmaFaye-gw3ei
    @FarmaFaye-gw3ei День тому +2

    Paix à son âme

  • @GorguiPouye-c7g
    @GorguiPouye-c7g День тому +5

    Dég bi dal pén de mort moufi wara nék😢

  • @allediouf1286
    @allediouf1286 День тому +1

    Que son âme repose en paix

  • @FaymataBa-ys1ip
    @FaymataBa-ys1ip 23 години тому

    Thieyy Sénégal

  • @kiidjbsukshnisjsywhkdkd3596
    @kiidjbsukshnisjsywhkdkd3596 День тому +1

    touba Serigne Touba dafa nianon mais lékk ribba gui mara yi nékkè mo waral li lèppou😢😢

  • @fatousagna3981
    @fatousagna3981 День тому +2

    Yalla nako suniu borom haré aldiana

  • @ramatoulayewadou5584
    @ramatoulayewadou5584 День тому +1

    billahi on est tous en danger 😢😢deuk bi amoul benna sécurité ni loi pour ces tueurs

    • @mamebacs6622
      @mamebacs6622 День тому

      en tout cas doyna warrr yallah na yallah def diam mais ca commence à dépasser les bornes quand même

  • @AbdouDiop-m1o
    @AbdouDiop-m1o День тому +1

    Yalla na yalla yeramko te dijegalko

  • @KhadyGaye-m5c
    @KhadyGaye-m5c День тому +1

    AMNA LOU KHEW SÉNÉGAL

  • @SsliouNdiaye
    @SsliouNdiaye День тому

    Yalna oyoff

  • @DiattaNgom-r2r
    @DiattaNgom-r2r 7 годин тому

    😭😭😭😭

  • @OusmanemoussaCisse-w3k
    @OusmanemoussaCisse-w3k День тому +1

    Hafarit yi Nio ngifi di deflo nit yi lounek Bilahi xam Kitabi🦻👈

  • @TaphaSene-c8c
    @TaphaSene-c8c День тому +5

    Sénégal nekh na dall kou ray nitt reck gnou gnou nii dafa amone fébarrou khel😮

  • @IssaDiop-m4y
    @IssaDiop-m4y День тому +13

    Dafa doff bou police dokhanè ndèm dineu wérr

  • @NdiemeDiouf-k1c
    @NdiemeDiouf-k1c День тому +1

    Kou raay niouniiii Werediiii xeel 😢thimmm

  • @FatyDieng-d6o
    @FatyDieng-d6o День тому

    Dara dalou ko bayi lén Sénégal Kofi ray nitt rék niou ni dafa doff😢😢

  • @DialloSeydou-sg3oy
    @DialloSeydou-sg3oy 23 години тому

    Que son âme repose en paix 😢😢 0:24

  • @YaAwaFall-n8f
    @YaAwaFall-n8f День тому +1

    Allahou Akbar li gnew dh si touba

  • @khadimNiang-p3h
    @khadimNiang-p3h День тому +2

    nadio ray rek

  • @MorGning-n4i
    @MorGning-n4i День тому

    Limom doyna war dé rip

  • @abdoulahatseck6994
    @abdoulahatseck6994 День тому +1

    Que Allah lui pardon

  • @NdeyeFatouGaye-o4w
    @NdeyeFatouGaye-o4w День тому +1

    Nagnouko teuthie mounane wereudi khel 😢

  • @ModouDiop-c7q
    @ModouDiop-c7q День тому +1

    Yal na ko Yàlla yërëm te jéggal ko 😢

  • @buz7755
    @buz7755 День тому +1

    Wa senegal mom ni rek kou raye nit niounè dafa dof ah ma warou si mim rèw ba kange 😢

  • @SafouDeme
    @SafouDeme День тому

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @bocarabdoulwane7593
    @bocarabdoulwane7593 День тому

    Kou rey niou réy la

  • @aissatouguisse1824
    @aissatouguisse1824 День тому +3

    Naniou raye ndayame rek

  • @FoodéDiallo-l1c
    @FoodéDiallo-l1c День тому +1

    😭😭😭😭😭😭😭

  • @LòMamour-k6m
    @LòMamour-k6m Годину тому

    Ndeysaane paabi kou gueum yàlla la nak

  • @khadycisse555
    @khadycisse555 День тому +2

    Yalnala yala youbou aldaina amine

  • @Sfalloutv
    @Sfalloutv День тому

    Yemou dèmna NJ rek

  • @FallouThioune-jh5by
    @FallouThioune-jh5by День тому +1

    😢😢

  • @AbdoulayeNgeutt
    @AbdoulayeNgeutt 16 годин тому

    😭😭😭😭😭😭😭😭 1:04 😭

  • @maguattely1058
    @maguattely1058 День тому +1

    Kou raye nite rék niouni wéroule

  • @Esprit_Teranga
    @Esprit_Teranga День тому +1

    Touba aussi nasi gua wakh ya trop de meurtres ses temps ci

  • @galsen1406
    @galsen1406 День тому +1

    Dara diotouko li rek mon yak Senegal Dangaye raye nioune weroul nagnou raye ndayam Cest tou

  • @fayeaida1066
    @fayeaida1066 День тому

    😢😢😢😢

  • @mariesalomon3375
    @mariesalomon3375 День тому +8

    Ah mande dama ragal sakh rayé note comme aye wegne Li mome président nasi dioke