En regardant le dernier combat de Lac rose contre Quench on voit nettement que Lac s'est bien améliorer physiquement. Félicitation Lac Yokal entrainement yi rek dina bakhhh
Aziz tay kene khamoul ligua beurè lac rose sou continuer wone bagare bi digua kao guediaway la deuk mai j felicite lac rose merci lamine et son equipe❤
Fils de balla lac rose dala diangue xam sa beurei tei iioe dianguo koo Félicitations lac rose et à l’écurie fass Redouble d’efforts fils de balla champion ngua
Mane félicitations lac rose lay wakh tay machallah khawma no done entraîné mai boulko bayi boul tegui tank kene fougoul wone lamb j agg fi guenal yok entraînement yi tei fonk écurie fass difa dem tou le temps so récupérer sa répère yeup gayi dinagnou am problème fekhel safate sapp mbeur
Félicitations à Lac Rose gathié ngalama té passaka durant tout au long de vos face to face mo fétéwone ci wakh djou beuri ba paré jeuféwouko ragal la défou feu dara bonne continuation Lac tu es dans la bonne voie
*Fils de Balla wakh diou beuri bi yeup tu luttes contre Lac Rose mii ngeu kham ni mola mag fouf en plus Tok neu presque 10ans beuré woul yow ngeu nek khalei nou ndaw beu parei meuno ci mom dara. Bravo Lac Rose, am ngeu seu place ci lamb ji beu legui*
Vraiment lac rose la faralone mais lac Rose défoul lou fils de balla défoul boulén dieul tord bi diokhko fils de balla tmt Fils de balla Deugleuh lac rose dako mayone chance rk mais amousi pertement dafay defarou Wat amat combat Lac Rose aussi dina amat confiance bokat si lamb mais bou danou wone bayi lamb félicitations niom niarr niépp ❤❤❤❤
Il faut reconnaître aussi qu'il n'a essayé aucune tentative pour terrasser son adversaire. Au contraire il est resté sur la défensive. C'est son adversaire qui devrait être félicité en toute honnêteté
Avant tout man je dis félicitation à lac rose 🙏❤❤👏 Félicitation à lecurie fass tay stratégie biguen tekk nii lepp lou fils de balla tekk tay lac dindi nako Fils de balla tu avais 2 chois soit dokh si kaw lac rose douma ko dann ko wala indi plan t amo won fitou deff lolou yeup encadrement null guediawaye amoul magou lamb ieoe yay khalé ya warone de lepp✌️✌️ Lac rose amna évolution bou bah donc une fois lac rose bou teudjiou watt entraîné meme rythme meun na gnewat en forme
Lac Rose bléssuram ba moko pénalisé tardél carrièram mais mbeur meunouko si lamb j guir yala boul tégui tank continue tes entraînements sérieusement gua dieulate sa place si lamb j
Fils de bala a fait comme bala gaye ce soir, en regardant son gros ventre on se rend compte qu'il ne s'est pas bien entraîné. Et puis il s'est donné une pression lui-même en parlant beaucoup, et en provoquant son adversaire depuis le début. Il a ensuite provoqué des bagares jusqu'à se blesser avant le combat. Et puis il avait beaucoup trop de gris gris autour du corps. J'avais cru que c'est un futur grand champion, mais il m'a beaucoup déçu 😢😢
Gnaata mbeur gnofi wah nga fokni dagnii réy sène adversaire gnou gneuw menni kharou yar wala gnou daanelène.. lolou bouko meussa considéré c juste des paroles à l'air.. Laurent ndiago wahneu ba sonnou gris2 daaneko daane bou gnakk fayda.. lac2 aussi loumou wah yeupp ak menacé dafa nul contre siteu.. djene kairé aussi rèw ba dof gnou daaneko et +100000 autres mbeurs Lolou si diaay combat bi rek la yam
Bro franchement so kholé bou bakhe sétane bou bakhe fils de balla mo nékone favoris, guiss guan nimo done yeugaté lac, donc so wakhé entrainer woul dina ma diakhal forme bi aussi nila meuse tolou, pour wakhe diou beuri bi guany wakhe pour diayy combat bila, mbeur you mak yi nioko fi dakk donc souko mbeur you daw yi défé boul kase bro.
Thieye senegalais mom dal del dan rk fils de balla 3victoire la teguelé taye mou gnew lac rose tenir ko rk gnoune khamoul dara bouko lac rosse danon deh khamma fanla dieum
Lamb dji tamite, gni beuré bay beugue dé nga nane ay disqualification. CNG war nagno kholate arbitrage bi. Diéleu dou force match null si combat la bokou. Ils n'ont rien à reprocher aux lutteurs
En regardant le dernier combat de Lac rose contre Quench on voit nettement que Lac s'est bien améliorer physiquement. Félicitation Lac Yokal entrainement yi rek dina bakhhh
Tu as parfaitement raison
je suis un ex-Boxeur Italién et J'Aime la Lamb, c'est vraiment Belle.❤
Aziz tay kene khamoul ligua beurè lac rose sou continuer wone bagare bi digua kao guediaway la deuk mai j felicite lac rose merci lamine et son equipe❤
Fils de balla lac rose dala diangue xam sa beurei tei iioe dianguo koo
Félicitations lac rose et à l’écurie fass
Redouble d’efforts fils de balla champion ngua
Vraiment fils de balla dou dara bravo lac rose entrainment bakhna
Lac rose moyeu champion cetait seulement le blessure attention
Niome ñiar ñio yame😂😂
@@babacargueye-or5timais fils de balla moy favoris te Lac rose woroul wone yak yonam
Ouii fils de balla na fait qu’une contre performance!
Kou yakar ni gni douniou entraîné yagui nakh sa bopp beuré da méti dh ❤
Felicitations Lac Rose lambou mo teureudi rek mais boy yi yepou dosen morom❤
Bravo lac tay entrainement bi bakhna
Vraiment félicitations modou boy niang entraînements rekk mo wore
Mane félicitations lac rose lay wakh tay machallah khawma no done entraîné mai boulko bayi boul tegui tank kene fougoul wone lamb j agg fi guenal yok entraînement yi tei fonk écurie fass difa dem tou le temps so récupérer sa répère yeup gayi dinagnou am problème fekhel safate sapp mbeur
Félicitations à Lac Rose gathié ngalama té passaka durant tout au long de vos face to face mo fétéwone ci wakh djou beuri ba paré jeuféwouko ragal la défou feu dara bonne continuation Lac tu es dans la bonne voie
Félicitation à Lac Rose
Lii mome ndame la si yaw
Fils de balla il parle rek😂😂😂😂c’est bien fait pour lui
Lac rose c’est un champion
*Fils de Balla wakh diou beuri bi yeup tu luttes contre Lac Rose mii ngeu kham ni mola mag fouf en plus Tok neu presque 10ans beuré woul yow ngeu nek khalei nou ndaw beu parei meuno ci mom dara. Bravo Lac Rose, am ngeu seu place ci lamb ji beu legui*
Vraiment lac rose la faralone mais lac Rose défoul lou fils de balla défoul boulén dieul tord bi diokhko fils de balla tmt
Fils de balla Deugleuh lac rose dako mayone chance rk mais amousi pertement dafay defarou Wat amat combat
Lac Rose aussi dina amat confiance bokat si lamb mais bou danou wone bayi lamb félicitations niom niarr niépp ❤❤❤❤
Félicitation Lac rose yokou entraînement yiii rkk
Yakarou guediawaye sa thies la Jackson ak thiatou daouda fall ❤
Dét way,😂😂😂
Lou leur yalmine bii
Lou leur yalmine bii
Ak Bou Siteu😅
Niang bou daw foumou deuk
No kou khol lac mi bureue ak quenche ak bi forme amna woute bou bakh
Vraiment les deux lutteurs ils ont tout donné amna beuré amna xékh vraiment
Lac Ros figa done entraîné boul ko bayi bakhna trop jsuis fans de modou lo mais forme bagui gneuw
Il s’est bien préparé wakh deugg yalla
Mdr
souko bayi woul dina am dara
Il faut reconnaître aussi qu'il n'a essayé aucune tentative pour terrasser son adversaire. Au contraire il est resté sur la défensive. C'est son adversaire qui devrait être félicité en toute honnêteté
Félicitations lac rose du couage fils de fawzeyni
😂😂😂😂
Félicitations lac rose❤️🔥
félicitation lac Rose ndakh retour bi bakhena mais combat bi nekhena
Lac Rose très la forme geuneu bouko bayyi rk diadieuf lac rose
Dictée zéro 😂
Macha Alla lac Rose andi gua sa vraie état physique
Bravo lac rose continue comme sa forme Bangui nieuww
Fis de balla yama béte ligay wah yép no li menoumaco geme le retour de lac rose le retour de fass ndam rék inecha ala 💪
Mbeur bou amoul respect moy fils de Balla mo takhit da nio warone niouss ndt rk
Bonne continuation lac boul tegui tanke dè
Lac ross bakhna dh yokal entrainement yi rek fekhèl geun dèque bi ❤❤🎉
Avant tout man je dis félicitation à lac rose 🙏❤❤👏
Félicitation à lecurie fass tay stratégie biguen tekk nii lepp lou fils de balla tekk tay lac dindi nako
Fils de balla tu avais 2 chois soit dokh si kaw lac rose douma ko dann ko wala indi plan t amo won fitou deff lolou yeup encadrement null guediawaye amoul magou lamb ieoe yay khalé ya warone de lepp✌️✌️
Lac rose amna évolution bou bah donc une fois lac rose bou teudjiou watt entraîné meme rythme meun na gnewat en forme
Xaana taay 😂 boul sisou xana setano pape ndoye ak Jackson dafa gniouss pape ndoye bamou teudeu fass amoul mbeur amoul ay dirigeant you bakh
@@veridique9454wahou dof😂😂😂😂
@@veridique9454loy merr louy tangal sa khol ?serigne ndiaye 2 limou leneu deff 😂😂😂
@@wakhkatoundiakhoum2167 loumou lèn dèff
Lac Rose bléssuram ba moko pénalisé tardél carrièram mais mbeur meunouko si lamb j guir yala boul tégui tank continue tes entraînements sérieusement gua dieulate sa place si lamb j
Franchement lac mo léne Moune confiance bi mo fi nek
Match trés Beaux.
Les deux combattént sont Fort.
J'Aime la LUTTE LAMB ❤
Mais fille de Balla mi deh Balla Gaye 2 rék lama djokh ay yaramou ndokh la ñiou yoré
Balla gaye sakh légui la depuis combat contre Tyson mais avant muscle rek lawone Fils de Balla ni la meusseu méle
Fils de balla mii yambars la katt😂😂 ak sa wakh diou barrii waa anaa serigne sou donn wakh fils balla dayy dann khamouniou gattt 😂😂😂
Lacrose ligeyna si combat bi de vrai😊 entièrement moy lamb
Ces arbitres sont pressés de donner des avertissements pour se mettre quelques choses dans la poche
Fils de Balla nakaté lamign ba reuy rk dou touss😂😂😂😂
khoulo rek la meune 😂😂
@@awandiayediouf2437😂😂😂😂
Lac rose gaîndé leu bilahiii ki dou yomb dane dhé
Fils de bala a fait comme bala gaye ce soir, en regardant son gros ventre on se rend compte qu'il ne s'est pas bien entraîné. Et puis il s'est donné une pression lui-même en parlant beaucoup, et en provoquant son adversaire depuis le début. Il a ensuite provoqué des bagares jusqu'à se blesser avant le combat. Et puis il avait beaucoup trop de gris gris autour du corps. J'avais cru que c'est un futur grand champion, mais il m'a beaucoup déçu 😢😢
wadji ki yaram bi nila meussa mel le fait de parler beaucoup dou dra loudoul diaay combat et il la reussi
@@dabakhmalick8484 il a réussi quoi ? Diaye combat bi dane combat bi moko gueune
@@ibrahimamba1296 nila done deff di dane
Gora Sokh Tapha, general Malika et autres
Gnaata mbeur gnofi wah nga fokni dagnii réy sène adversaire gnou gneuw menni kharou yar wala gnou daanelène.. lolou bouko meussa considéré c juste des paroles à l'air..
Laurent ndiago wahneu ba sonnou gris2 daaneko daane bou gnakk fayda.. lac2 aussi loumou wah yeupp ak menacé dafa nul contre siteu.. djene kairé aussi rèw ba dof gnou daaneko et +100000 autres mbeurs
Lolou si diaay combat bi rek la yam
Bro franchement so kholé bou bakhe sétane bou bakhe fils de balla mo nékone favoris, guiss guan nimo done yeugaté lac, donc so wakhé entrainer woul dina ma diakhal forme bi aussi nila meuse tolou, pour wakhe diou beuri bi guany wakhe pour diayy combat bila, mbeur you mak yi nioko fi dakk donc souko mbeur you daw yi défé boul kase bro.
Fils de balla wakham bi yeup neketei filay moudiou 😂😂😂ki dou touss neketei aller lac rose 🎉
Lac Bilahi manque de confiance en soit moko diapp rk
Mais sou amei endurance deug am dolei mbeur dou ko gawa dann
Nakh Amna fitt niémé na
Père pala machallah khamngua lambe dhé 🎉
machalla lac ros dina bakh inchalla 4:31
Fils de balla wakh rek leu meun 😂😂
Fils de balla d'où dra pour moy roi des sren 😂
Lac ross continel liguey ndana nga
Lac rose moyeu champion cetait seulement le blessure
Fils de Balla ak waxam diou bari nékété dou dara. Lac Rose tu viens de te rendre compte que entraînement rek mo woor
Lac rose bou khekhone door fils de balla mou danou ndakh niemewoul coup
Bly
Dafa bari wakh Champion bou melni Balla danguay koy respecter diema def loumou def me wakh rek te defa go dara
Bilay deh dafa mana togne😏😏
Cest de par laa qu’on tire que Quench diambar leuu. Nako gayi dieul
Lac Rose boudone may mom souba ma délou entraîner légui mou douguate si l'amb dji
Mbeur yii nan roy si Modou lo di entraîner bayi noss gou metei gui yoor sa biir bou reuy ni dagay déf sports 😅
Lac rose d’où lac de guet môme day beure day so gué bandit gués la
Lac rose champion la da fa tardé si lamb
Félicitations lac rose ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Pour Lac Rose menatoul rattraper waron na wessou fi me dafa fowé talent bi mou yore mougnate moko fi dessé
Fix da balla dagua oupalé l'ac rose rek da nakharé beurel
Fils de balla mi dou gattt
Deux lutteurs qui ne sont pas prêt physiquement ça donne ça..y’a pas photo
Fils de balla ak sa lamigne bou reuye bi yép ya niak diome,kouy sa ENTRAINEUR lamine gollo😂amoul kham kham tek si seytané😀
Pour mane fils de Balla poids bi naturel bo kole son visage da meli kou dieul dara pour reye
Thieye senegalais mom dal del dan rk fils de balla 3victoire la teguelé taye mou gnew lac rose tenir ko rk gnoune khamoul dara bouko lac rosse danon deh khamma fanla dieum
Fils de Balla Alhamdoulilahii ba yaw akh Domou Dangou amoul khamo dara té barii wakh 😮
Dagou moka meune foufe
Lac ros souba teguate kossi entrainma bakhna
Félicitations lac Rose 💪
C’est quoi la différence entre disqualification et match nul vu que y’a pas de vainqueur
Lac rose❤
Sénégal mettina bilay
Balla Gaye 2 mogui conseillé Fils de Balla tei boudone mom dou dane Lac Rose 😂😂😂
MBA khala beurer 02 combat foumou tourner di wakh fils de balla tu ma déçu félicitations lac rose
Ce combat est une honte pour notre sport..Imaginez quelqu’un qui découvre ça ?
Ioe nopil dagua fok niii lamb dafa yombb
Lii dafa yombou way taxaw dii lawato ba temps bii diex.
Lac rouge légui la rek mais sadique rek lac am fitt
Lac roz seul kou ame sa mbeur nga té ko
Merci fils de balla boula keneu diay yéne yeup laniou faye . Lac rose kou niak fayda la . Nul di jubilé 😊
Lac rose entraînement bou woor la indi boulko meussa bayi
Fils de balla mounguabeure du courage cou entrenewoul nakalaw tenir tout cette temps là baylen wakh jii gnaw yii fils de balla c'est un champion
Fiss de bala mideh amoul ndia rigne
Entraîné rek loc gayi manou nioula
Non slt Lac dafa am probleme genoux mais fils de Balla mo eupeu Dole geun fetee khale Bravo Lac rose
Fils d balla ya wahon lac rose makk la yay hale te mounoko dane wagnil wah dji touty
Kou dan sakh
Lac Rose dièxalna bou yaguëu amatoul touss dafa fënëukh
Action yeup
Songou yeup
Fils de balla moko dèff lac rose dafa copié lac 2 😂😂😂
Felicitation fils de balla 😂😂😂❤❤
Liii tmt combat bou sofeeee 😂😂😂😂😂
Félicitations Lac
Ils ont bien lutté nak
Boy bi wakh rek leu meun ndéké.
Loc ros légui kham na yon bi dh
Félicitations fils de balla
Lac ross ligueye na
Bravo lac ross mercii
Wakh dji dall moy fils de balla amoul entraînement
Outti lén forme comme Mod’lo
Lamb dji tamite, gni beuré bay beugue dé nga nane ay disqualification. CNG war nagno kholate arbitrage bi. Diéleu dou force match null si combat la bokou. Ils n'ont rien à reprocher aux lutteurs
Félicitations lac rose
Toute façon gnarri patta national gnodone beuré 😂😂🚶
Iow khana do khole ben patta mofi ame teh fils de balla la
Je comprend pas les avertissements , beurré door
beurré door door AK beurré âme avertissement ????
Lac rose 🌹 the only thing