Drame à Touba Guédé : une femme a été tuée par son beau frère

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 21 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 351

  • @KhadyDiouf-jp1mc
    @KhadyDiouf-jp1mc 16 днів тому +106

    Yalnako yalla yereum té kharéko aldiana firdwsy thi barké seydina Mouhamed Salalakhou ala Mouhamed 🤲🤲🤲

  • @DameNdiaye-dl5lz
    @DameNdiaye-dl5lz 16 днів тому +70

    Youma Ndiaye yalla na yalla yeureum té djiégeul la

  • @FatouGueyeada-we1zc
    @FatouGueyeada-we1zc 16 днів тому +221

    Encore sénégal li lanla nk wayé nagnouy moytou di dégnthialanté lou bon sun biir khol yi ray bi eupouna gnawna yalnagnou yala mouthial si lou bon

    • @jobjiitalyalla1382
      @jobjiitalyalla1382 16 днів тому +4

      Doyna warr

    • @Khasiida
      @Khasiida 16 днів тому +4

      Nekall nitt KOU weroull nan la mana diapale nitt Lou bonn boy bi depuis bimou dioudou ba legui weroulll

    • @moussasarr-j2d
      @moussasarr-j2d 16 днів тому +2

      Ay njiit you sokhor lii mooy resulta bi guissougouleen dara

    • @Achrafjoop
      @Achrafjoop 16 днів тому

      yaw ya boun te soxor kon contante ngasi am ak ndam😮​@@moussasarr-j2d

    • @Gggge_dudiolof9536
      @Gggge_dudiolof9536 16 днів тому +4

      ​@@Khasiida kou weroul dou deukkk si keur. Loutakh yobou wougnou ko raffinerie mbao wala fi dof yi nekk

  • @MamediarraSeye-z9t
    @MamediarraSeye-z9t 16 днів тому +56

    Ay way tata yalla nako yalla yeureum 😢

  • @mbayendiaye3094
    @mbayendiaye3094 16 днів тому +29

    Ndayesane yalla nako Yalla yarame

  • @baaxbaay2919
    @baaxbaay2919 16 днів тому +75

    Pere bul ko jèema wutal aw lay nag naan dafa wèradi xel yooyu taxawul dafa ray nit nañ ko teg ci yoon rekk moo gën kii lumu def ñaaw na lool xalaat naa doomam yi lool wallaahi😢
    Yalla na ko yalla yërëm te jèggal ko ci barkeb S Fàllu🙏

    • @khalifababacardiop8709
      @khalifababacardiop8709 16 днів тому +6

      Pa yi ay seytané lagnou Lou diok gnou diem ko expliquer

    • @fatoudieye7624
      @fatoudieye7624 16 днів тому +1

      Pourtant degue la dafa wéradi won nion boguou bein quartier

    • @Gjhjll123hjkkjhh
      @Gjhjll123hjkkjhh 16 днів тому +13

      On s'en fout si wérédii khélam dafa rayy nite na yone déf liguéyam

    • @diagneamsatou3473
      @diagneamsatou3473 16 днів тому

      Moma diakhal

    • @bellawomen
      @bellawomen 16 днів тому

      @@khalifababacardiop8709en plus mounnan weredi khel di chercher alibi

  • @thiorosall
    @thiorosall 16 днів тому +21

    Ndeye saan thiey li yalla nako yalla yeureume thè khareko aldiana firdawsi barkép cheikhoul khadim amiine yarabi

  • @SerignesaliouDiop-m3d
    @SerignesaliouDiop-m3d 16 днів тому +9

    اللهم إني أعوذ بك من عذاب القبر و من عذاب النار 🔥 🔥 🔥 🔥 🔥

  • @ToufaDiawara
    @ToufaDiawara 16 днів тому +45

    Inna lilahi wa inna lilayhi radiokhoum tiss bou meti yalla na ko yalla yereum té kharé aldiana firdawsi

  • @thiernoseck8365
    @thiernoseck8365 16 днів тому +60

    Réew mi damaa yaakaar ni day wadia Tukki 😢😢😢

    • @gorandiaye2419
      @gorandiaye2419 16 днів тому +2

      Rew mi tukki na ba bari Sénégal dou rew 😢😢😢😢😢😢

    • @loudoulaktalibesafouma3429
      @loudoulaktalibesafouma3429 16 днів тому +1

      Sonko mo ay gafe

    • @Abraham22199
      @Abraham22199 16 днів тому

      Sénégal lifi am amoul feen bilahi 😢

    • @khadydia828
      @khadydia828 16 днів тому

      ​@@loudoulaktalibesafouma3429da ngaye doul dé da nga beug wakh li amoufi wone?

  • @magueyefall4031
    @magueyefall4031 16 днів тому +23

    Yalla nako yalla yeureum t kharéko aldjiana firdawsu allah 🙏🏾

  • @veroniquenatack7392
    @veroniquenatack7392 16 днів тому +30

    *Thieuy Yalla ray yi na kagne😢😢😢Paix à son âme Yalla na aldiana di noflay yam🥺🙏🏽🙏🏽🙏🏽*

    • @myamandiang
      @myamandiang 15 днів тому

      Xol yi nio khate haine bi bari

  • @mandoumbemboup2952
    @mandoumbemboup2952 16 днів тому +18

    Que justice soit faite RIP

  • @AbdouNgom-t4y
    @AbdouNgom-t4y 15 днів тому +4

    Yalnako yala yeureume 😢😢😢

  • @NdiayeNamesaye
    @NdiayeNamesaye 16 днів тому +20

    Ndaysan yeumou Ndiaye yalla nala yalla yereum te kharè la aldjina 😭

  • @fademaful
    @fademaful 16 днів тому +15

    Li doyna waar njaboot gui rek lay khalaat😢

  • @KhoudiaDiop-no6qw
    @KhoudiaDiop-no6qw 16 днів тому +25

    Ki det moy sa goro mo tak nga wakheni
    Bou don sa dom bou djigeun la ngou Ray digani n'a yone def ligeuyam

    • @aledione9857
      @aledione9857 16 днів тому +3

      Billahi je voulais dire la même chose

  • @CheikhDiop-c6k
    @CheikhDiop-c6k 16 днів тому +18

    Sunu waxé Niouné état li lousi état meun 🥺education de bass lou am solo la Bilahi

    • @user-cm7jk3ip5t
      @user-cm7jk3ip5t 16 днів тому +1

      Wadji dafa wéradi waradik khél nio bokou kogne réron na sakh police kay fawou nou tékoyé parce li woroul

    • @salmafalldiouf9369
      @salmafalldiouf9369 16 днів тому

      @@user-cm7jk3ip5tloutax rayoul papam wala kenen

    • @AntaDiouf-m5w
      @AntaDiouf-m5w 15 днів тому +1

      Bilahi problème bi lolou la éducation de base moo manquer légui

  • @Moustaphandiaye650Ndiaye
    @Moustaphandiaye650Ndiaye 16 днів тому +13

    Ndeysan yalna ko yalla yeureum si barkep Serigne darou assane yalna Serigne darou assane térou

  • @mamourfall5027
    @mamourfall5027 16 днів тому +20

    Bis na tay la rakkam doon sëyyi, ndaysaan, sama soxna daje woon na fa ak moom 😢😢

  • @sokhnadiouf7622
    @sokhnadiouf7622 15 днів тому +1

    Yalla Nanou yalla moussaka si kholii boni

  • @sokhnadrame7735
    @sokhnadrame7735 16 днів тому +17

    Thiey Sénégal li mbadiamla chaque jour avec de nouveaux cas de meurtre thiey😭😭

  • @khadimka2058
    @khadimka2058 16 днів тому +11

    Ay bau frère bi loum def nii, sokhna si yalla nako yalla khare aldiana firdawsi, ndaw si sakh dafa rafet ndeysaan

  • @rokhayamadamesano
    @rokhayamadamesano 16 днів тому +10

    Thiey adouna ,deugue deugue moudioume diamono lagnou nekk ndeysane yalla na yalla yeureum ko té khare ko aldiana firdawsi Barker seydina mouhamad sws psl AK mboleme waye dawlo Amine 🙏

  • @NdiayeEva-op9vr
    @NdiayeEva-op9vr 16 днів тому +12

    Yalla nako yalla yeureum khareko aldiana

  • @cheikhfall8310
    @cheikhfall8310 16 днів тому +1

    Yallanako YALLAH yereum takhawou djabot gi bi barakati seydina MOUHAMED🤲🏼🙏🏼😢

  • @MamediarraThioye-s9p
    @MamediarraThioye-s9p 16 днів тому +9

    Yalla nako yalla yeureme té kharéko aldiana

  • @MariamaDembele-gy7kz
    @MariamaDembele-gy7kz 16 днів тому +11

    Yalnako yalla yereume

  • @Kombanend
    @Kombanend 16 днів тому +1

    yoma ndiaye dem na rèk😢😢

  • @ShashaAïcha
    @ShashaAïcha 16 днів тому +4

    Yalla nala yalla yeurame 😢😢

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 16 днів тому +15

    Thiéye Sénégal Fomou dieum ohh vraiment lii métina trop Yalla Yeureum ko amine waye

  • @ramanonga8630
    @ramanonga8630 16 днів тому +15

    Allahou Akbar naniou yatal xoul yi😢

  • @fkinegueye8575
    @fkinegueye8575 16 днів тому +25

    Thieye yalla 2025 bi yalnasi yalla wis ndokh mou sedd

  • @AmadouSylleCamara
    @AmadouSylleCamara 15 днів тому

    إنا لله وانا إليه راجعون اللهم اغفر لها وارحمها وعافها واعف عنها 🤲🤲

  • @NdeyeNdiaye-n8v
    @NdeyeNdiaye-n8v 16 днів тому +3

    Prix à son âme😭🤲🤲🤲

  • @AmsatouFall-os3td
    @AmsatouFall-os3td 16 днів тому +12

    Sénégal raye domou diambour gnou outeleu keyiti dofe li yombe n'a torope pénne😭😭😭 de mort késsé mokoye fathii😭😭😭🥺

  • @bakhyaye4250
    @bakhyaye4250 16 днів тому +10

    Tieuy souniou Sénégal gui lou fi dougue yalnaniou yalla soutoural

    • @nimspetite
      @nimspetite 16 днів тому +1

      Aar gnou Aar sougnou jaboot

    • @bakhyaye4250
      @bakhyaye4250 16 днів тому +1

      @nimspetite amine

    • @Bakhrek12
      @Bakhrek12 16 днів тому +2

      Yalnagnou yala samu te samalelgnou ndiaboot gui

  • @elimanefall6693
    @elimanefall6693 16 днів тому +4

    c'est vraiment triste
    Que la terre lui soit légère

  • @mariamacisse9611
    @mariamacisse9611 16 днів тому

    Wa ray gui pari trop wa li ma diam la 😢ki dem yalla nako yeureum hareko aldiana 🙏

  • @PapeDRAME-j1b
    @PapeDRAME-j1b 16 днів тому +7

    Yalla Nako yalla yeureum

  • @fatougueye8705
    @fatougueye8705 16 днів тому +17

    Waaraa foot waalaa toogou agn
    Yoor ligueye keur gui gnou rayyy laa
    Seyou Sénégal mettinaa

  • @assgueye9996
    @assgueye9996 16 днів тому +4

    Ray domou. Diambaru ba parés 😭😭 dii wakh yalla nieuw na ak dogalam 😭😭😭 liii dafa niawe 😭 yallna sa borom yésall yeurmandé thi kawam 😭😭😭

    • @NabouMbye
      @NabouMbye 16 днів тому +1

      Doful jine japuko dafa rew nyunan dafa weradi

  • @belishasims6152
    @belishasims6152 16 днів тому +4

    Ndogalou yalla ba kagn niitt ray moromom nitt ngeuine beugu ko teunk thi ndogalou yalla…!! Th yalla aramal rayy 🚶🏾‍♀️🚶🏾‍♀️

  • @Bayeibreundiaye
    @Bayeibreundiaye 16 днів тому +6

    Yalla nako s mbassamba térou

  • @khadyndiaye5646
    @khadyndiaye5646 16 днів тому +1

    Ki Sama rakou pape la méttina lole bay dame😢😢😢

  • @ModouDiop-fx8ml
    @ModouDiop-fx8ml 16 днів тому +9

    Yalla nako Yalla yaraem 🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾

  • @papemalickdiarra5995
    @papemalickdiarra5995 15 днів тому +1

    Yen ngen fokni Sénégal 🇸🇳 amoul malédiction 😢

  • @AmsaBa-k7i
    @AmsaBa-k7i 15 днів тому +2

    Je suis vraiment impressionné par la tranquillité et la maîtrise de soi de ce vieux. Tu sens que c'est une personne qui remettra toute situation entre les mains de Dieu. J'aimerais avoir cette capacité de résister aux émotions

  • @FallouToure-c5i
    @FallouToure-c5i 16 днів тому +3

    Rèwmi pourquoi kou raye nit ngounè dfa dof 😭😭😭😭

  • @FallMouhamed-id3ls
    @FallMouhamed-id3ls 16 днів тому +5

    Ndeye sane yalla nakou yalla guerem ta diegall kou

  • @KhdimWade
    @KhdimWade 15 днів тому

    Kouray nioune dawiradi khel nono😢

  • @mariamadabo9100
    @mariamadabo9100 15 днів тому

    Yalla yalla yeureum KO thi barque saydina Mohamed

  • @mayaciss6821
    @mayaciss6821 16 днів тому +7

    NA GNOU RAKHASS KHÔL QU ALLAH SWT NOUS PRÉSERVE ET NOUS GUIDE DANS LE BON CHEMIN QU ALLAH SWT ACCUEILLE CETTE MÈRE AU PARADIS ET PROTÈGE SES ENFANTS 🙏🏾🙏🏾

  • @mbowmalick6681
    @mbowmalick6681 16 днів тому +7

    Ndeysaan Senegal légui dangay ray nitt tay ko ay mbokkam takhaw né dafa am weredi xel

    • @aissatoukanefall1439
      @aissatoukanefall1439 16 днів тому +2

      Billahi dégu nga mouy diémeu protéger dome dji nane wéreudi xel na yone def ligéyeum

  • @GueyeSokhnaastou
    @GueyeSokhnaastou 16 днів тому

    Yalna ko yala yeureu té khare ko aldiana firdawsi si barkep alkhouran 🤲

  • @Mallèdieng-l1u
    @Mallèdieng-l1u 15 днів тому

    Loi bou béss bi lanne léy khar si ray bou barri bi😢😔

  • @ModouDiaw-dl1gj
    @ModouDiaw-dl1gj 16 днів тому

    Métina trop 😭 yalla nako yalla kharé aldiana

  • @AidaDiouf-fs9zn
    @AidaDiouf-fs9zn 15 днів тому +4

    Maylén niou diam koufii raay niit niounan da am wérédii khél😢😢😢

  • @mbalamediouf1306
    @mbalamediouf1306 16 днів тому +4

    Bayilen kou ray nite ngenane dafa dof si casobi lay dai

  • @SaliouGaye-z3q
    @SaliouGaye-z3q 16 днів тому

    Yalnako yalla yeureum

  • @ndeyemaguettendiaye6008
    @ndeyemaguettendiaye6008 16 днів тому

    Ndaysan youma ndiaye nianalenko yalla yeuremko khareko aldiana

  • @ahamouneyasunn6966
    @ahamouneyasunn6966 16 днів тому

    😢😢😢Ndaysane yeureum na Goor gui amna louko mitti trop d 😢😢😢

  • @SalyNdiaye-ef9su
    @SalyNdiaye-ef9su 16 днів тому +7

    Thiéy li doynawar yalla nako yalla yeureum hareko aldiana firdawsi

  • @AlhoussaryTop
    @AlhoussaryTop 16 днів тому +2

    ولكم في القصاص حياة

  • @NdeyeSarr-n6i
    @NdeyeSarr-n6i 16 днів тому +3

    Pa bi néna domame dafa am problème khél ndax beugueu niou bayiko mais dinagne ko niousse thi kasso bi sa dome dji dofoul dara dalouko

  • @mbenedieng2298
    @mbenedieng2298 16 днів тому +1

    Yaw papa gua balema mé wakhi wéradi boumou diepeu nak dara dalouko na yone défe liguéyame niouko téke si yone ki démome ay diabotame nio niakkk paix à son âme

  • @ahmadoudiop2054
    @ahmadoudiop2054 16 днів тому +6

    Rakou djeukeure dji moko raye, kokou dafa âme wérédi khéle 😢😢😢

  • @AlassaneNdiaye-n5y
    @AlassaneNdiaye-n5y 16 днів тому +2

    Ndeyssane yalna YALLA yéréme KO si barké Yarassouralah PSL

  • @baababa8388
    @baababa8388 16 днів тому

    Ndeysane yalla nako yalla yeureum té kharé ko aldiana 🙏

  • @assietoukamissoko137
    @assietoukamissoko137 16 днів тому

    Salam, Allah y rahma.

  • @Salikhate732
    @Salikhate732 16 днів тому +1

    Thiey 😢yala nako yala yeuram té kharéko aldiana fiirdawsi

  • @amiyfall-v1z
    @amiyfall-v1z 16 днів тому

    Yalla nako yalla yereume té khare KO aldiana firdawsi amine 🤲🤲🤲

  • @AïdaGaye-d9t
    @AïdaGaye-d9t 16 днів тому +1

    Yalna ko yalla yeureum

  • @MameFatouSeye-h9d
    @MameFatouSeye-h9d 16 днів тому

    Ay way man khôl lagnou woré 😭💔 😭😭😭

  • @PapebabaSeck-x9k
    @PapebabaSeck-x9k 15 днів тому

    Oh metina looooollle firdawssy sa demeure amin yaraby, justice, justice.

  • @aladjidiop2315
    @aladjidiop2315 16 днів тому

    YALLAH nako YALLAH yeureum
    xareko Aljana mayko geureumam

  • @AbaMbaye-uh2ul
    @AbaMbaye-uh2ul 14 днів тому

    Métti na lool lool waay,😭😭😭😭😭

  • @SireKa-b5l
    @SireKa-b5l 16 днів тому +2

    Legui Dafa doff ray len ndem

  • @awacheikhibra
    @awacheikhibra 16 днів тому

    Xawma ana goor ak diotèk djiguène bayy guèné paaka 💔
    Niak fayda ak bone xol 😭💔

  • @Tapa-vc5uz
    @Tapa-vc5uz 16 днів тому

    Yallah nako yallah yeureum

  • @mouhamadseye1024
    @mouhamadseye1024 16 днів тому +2

    Kou ray niou rayla rk kome Niko Yalla beugué

  • @Amirada03
    @Amirada03 16 днів тому +10

    Ana beau frère sax Di diapantei ak sa diabar ou frère....

  • @MiaGueye-q8r
    @MiaGueye-q8r 8 днів тому

    Elle repose en paix😢

  • @guidotoure4254
    @guidotoure4254 16 днів тому

    Non Sénégal chaque fin d'année ak début, day am ay meurtre 😢 vraiment mon pays va mal

  • @DioneRama
    @DioneRama 16 днів тому

    Lii ba kagne😢😢😭😭😭😭

  • @awabalde832
    @awabalde832 16 днів тому

    Que fridawsi soit sa demeure éternelle 🙏💔💔😭

  • @nafisatougaye450
    @nafisatougaye450 16 днів тому +1

    Ay way li méti na trop yalla nako yalla yeurem té xaaré ko aldiana firdawsi

  • @nfallymansaly8483
    @nfallymansaly8483 16 днів тому +1

    je disais toujours qu'on doit revoir nos comportements actuellement trop de violence dans les maisons d'abord trop de haine c'est grave tué la femme de ton frère 😢 envoyé lé en prison quel indisciplinés ya pas affaire de famille ici que justice fait son travail

  • @PapebabaSeck-x9k
    @PapebabaSeck-x9k 15 днів тому

    Lii doynaware looooollle, justice, justice.

  • @modousall2693
    @modousall2693 16 днів тому +2

    Way weradi khel moye lane papa nga balma mai dara diotouko bayilen bou nitt rayè nitt guenni weradi khel

  • @BayemorDiop-rj6no
    @BayemorDiop-rj6no 16 днів тому

    Thiey yalla li méti na yalla nako yalla yueruem tabal KO al dianaye firdawsi barkéb borom Touba

  • @cheriftayba
    @cheriftayba 16 днів тому

    Na yon dèf ligè yam 😢😢

  • @diaynabacisse6090
    @diaynabacisse6090 16 днів тому +2

    Aye way li metina yalnako yalla kharè aldiana firdawsi bilay li metina wayyy

  • @awakane1050
    @awakane1050 16 днів тому +3

    Kone dèè dofou nite laa ndakh nala lèr ni bou dieukerum takha wone dou ko lall monlay wane ni dofoul khar ba goor gnep dèm gan sogou dieugeune déf diefine wi dofoul dayy dof doflou

  • @MamegayeKane-mn4hn
    @MamegayeKane-mn4hn 16 днів тому +9

    Yalla nako yalla yreume

  • @NdeyeGueye-z8j
    @NdeyeGueye-z8j 16 днів тому +1

    Qui dofoul yalla mo warra raye

  • @Omardiop-x2j
    @Omardiop-x2j 16 днів тому

    Yalla nako yalla yeureume tei kharako aldjana

  • @ramsesndiaye8206
    @ramsesndiaye8206 16 днів тому +2

    Mes Lane mo takh Sénégal ñi séné nekhoule niou lene di bayi si keur yi dama khame bou niou raye nite rek niou nane khalame nekhoule c’est grave

  • @begueBamba
    @begueBamba 16 днів тому

    Wa senegal mommm😢😢😢😢🙆‍♀️🙆‍♀️

  • @MaamiDiouf-w2s
    @MaamiDiouf-w2s 16 днів тому +1

    Thieuy yalla ray