Yalla naniou yalla fayal Mame Cheikh Oumaroul Foutiyou Tall (RTA) Dieureudieuf Serigne Ahamad Fall yalla naleu yalla sameu soutoural leu Bidiahi (SAWS)
Serigne Ahmed Fall YALLAH na Yallah sammeu la tè yokk kham kham bi si barké Seydouna MOHAMMED saw si barké Cheikh Oumar Al Foutiyou Tall si barké Cheikh Ahmed Tijani Shèrif 🤲 amine ya Rabbi
Walahi seydi Ahmad Fall votre pédagogie est singulière votre maniere d'enseigner est particulier votre maitrise du sujet est parfait votre source est intarissable vous etes une fierté pour toute la communauté musulmane et particulièrement Tidjianite Malikite en ce sens que vous maitrisez parfaitement ce que vous dites. Alkhamdoulilah.
Ce jawahir est entre les mains de thierno mouhamadoul madani tall rare sont les gens qui l'ont vu yalla naniou yalla déf aye talibé cheikh youniou nangoul
yalna yalla sammal nu la, aaral nu la, té nioddi say fane, doli la sutura, tawfeex ak taysir incha ALLAH swt, amine bi diahi Seyyidil woudjoudi Seyyidina Mouhammadine PSL. Amine!
Ma'achaAllah le peuple est content que le tout puissant vous protège contre les malfaiteurs. Je vous écoute depuis l'université de Caen Normandie . Yo Allahu rèné wallahi mine mbéltiima guido .
Barakallahou fikk ya Oustaz Ahmad, nous vous suivons depuis Paris, on a tjrs le plaisir de vous suivre devant nos écrans. Yalla nala yalla doli takhawou inshallah. Bégg nanu bou bakh wallahi
Seykou Oumar tal dou morom ken xolal digantem ak wa makka ak madina ak palastine ak eguipty ak mali ak guine ak Nigeria ak seydi alhaji malik ak cheick ahamadou bamba ak imamoul mahdiyou ak alhaji ahmadou baro ndieguen
Dieureudieuf serigne Ahmad Fall, merci de nous faire connaître nos chers maîtres spirituels et leurs écrits. Que Dieu (SWT) vous récompense de la meilleure des façons Amine.
Seul Allah, son prophète seydina mouhamad anleyhi salatu wa salaam et Cheikh Akhmad Atijiani connaissent la grandeur et le degré de Cheikh Oumar foutihou tall
Yallla naniou yalla fayal Cheikhou Omar foutiyou ❤❤❤
❤❤
Cheikh bi daal dama fok ni yalla moka wathié pour la nouvelle génération Machallah
Machaallah oustaz ahmad fall yalna la yalla défal diamm❤
Yalla naniou yalla fayal Mame Cheikh Oumaroul Foutiyou Tall (RTA)
Dieureudieuf Serigne Ahamad Fall yalla naleu yalla sameu soutoural leu Bidiahi (SAWS)
‹no comment"
Ham ham rek ka worr
Ya cheikhou ,ya oumarou,
Billahi Fall Mala dope dakh rek Cheikh Abal Abass khoudboul awlliya yi. Yalla na sounou Borom defal la tawfeekh Amiin
Djeureudjeuf Mame Cheikh Oumar Foutiyou Tall♥️🙏
Serigne Ahmed Fall YALLAH na Yallah sammeu la tè yokk kham kham bi si barké Seydouna MOHAMMED saw si barké Cheikh Oumar Al Foutiyou Tall si barké Cheikh Ahmed Tijani Shèrif 🤲 amine ya Rabbi
Walahi seydi Ahmad Fall votre pédagogie est singulière
votre maniere d'enseigner est particulier
votre maitrise du sujet est parfait
votre source est intarissable
vous etes une fierté pour toute la communauté musulmane et particulièrement Tidjianite Malikite en ce sens que vous maitrisez parfaitement ce que vous dites. Alkhamdoulilah.
Walahi vérité absolue et merci pour ta franchise
Pi
Machalla serigne Ahmad ❤❤
Ce jawahir est entre les mains de thierno mouhamadoul madani tall rare sont les gens qui l'ont vu yalla naniou yalla déf aye talibé cheikh youniou nangoul
Amin barké Mohammed salalahou aleyhi wassalam
Yo alla yoban en cheikh oumar alfoutiy radiyallahou anehou
Amnasolo masala
Amine inchallah 🤲
Le meilleur marabouts des noirs seydi seydi tall le monde connaît très bien l’européen les indou les palestiniens partout
Seydi Tall yalna Yalla fayal gnouko.
Jerejeuf Serigne Daara
Soppou nala ndah sa Tourando Seyidi Ăly Harraazim Barrada Al Faacį RTA.
@@tcsh7tijaniya517 jerejeuf sangue bi sope nala mane tamite ndakh Cheikhana Ahmad At Tidjani Cheriiiif
Dama guiss 2e partie bi rek bégue oustaz professeurs serigne ahmad fall
Bilahi sema fallén bi yal naga dondo. 111si barké seydina Mohammed psl
Sénégal warona niou tanna beuna jour niou diaga leeko Seykou Oumar Tal
Seydi tall!!!!!
Seykou Oumar Tal rek moy senegal moy afrik yal nala yala fay si barke maw laa ya Seykou Oumar Tal xam xam mo woor
Serigne bi man deih damala sopeuh❤ yalna nala BOUR YALLA fay geune di fay🤲🏿🤲🏿🤲🏿...Dieureudieuf
ALLAHU AK BAR LAHILAHA ILLALA MOUHAMMADOU RASSOULOULA SAWS
Yalla fayla oustaz ahmat fall bilah beuguel guimala beugu rombouna les limite yalla def souniou guisse
Kodda ada ayssa elimane cire samba demaba Ali mouktar ❤🙏🏼
Yala nala yala arr ya cheikh ahmed fall leralgua lou bari machalah
الله اكبر جل جلاله يا أستاذ نسأل الله أن يو تيك الكيمياء القران الكريم كلا وعمرا طويلا بلا تردد والله فرحت فرحا جيدا جزاك الله خيرا
Macha Allah y'a cheikhina yalla n'a yalla doli diapalé dila ziar dila bégué
thiey chiekhou Oumar alakhou akbar
💓💓💓💓💓💓 impossible de rater les cours de notre cheikh....mashallah mashallah
Oooôooooôoooooôooooôoooo99o
Vraiment li lan begue si tarikhabi yallana yalla fayla fall
Yalle ne yalle fay
Machallah serigne Ahmed fall yaw warr nga lékk sama khalis dh naka laye déff ba dior la je suis en Espagne contant si yaw machallah
77 102 32 24 son numéro
Ce qui font des DISLIKES 👎 qu’est-ce qu’il ya vous savez pas ce qu’il dit ou bien 😭😭😭
Cheikh oumar (RTA) wallahii damako fan moy sama idole
Sénégal yeup ya daka idol machalah
Yalna yala doli la deugaral🙏
yalna yalla sammal nu la, aaral nu la, té nioddi say fane, doli la sutura, tawfeex ak taysir incha ALLAH swt, amine bi diahi Seyyidil woudjoudi Seyyidina Mouhammadine PSL. Amine!
Manchllah seydi TALL BOU YALLAH TALL...... Merci seydi Ahmed fall
Barkii sheikh tidiane ya meune sagne sè dh masha alla barkii 548😍😍👊
Machallah Serigne bi yalna yalla défalla yiw barké Cheikhou Tidjane Chérif
MA challah Serigne bi bègue SI yow
Alhamdoulilah sounou serigne sounou sak yalna yalla fayla mayla goude fane mayla weer bayila ak sa khel barké seydina chekh ahmad tidiane cherif rta
Fatabarakallah Serigne Ahmeth FALL nala bour yalla fay yiw y’a barké Cheikh Seydil El Hadji Oumar Al Foutiyou Tall
Alhamdoulilah Alhamdoulillah Alhamdoulilah mbekyé gnélna beppe ndiambote ak sopé Cheikh Omar Alfoutyou yallah dafnio beral lokho,li khéwalou yallah leu bou keneu meunouta natt diaredieuf Seydi Professeur Ahmad Fall yallah na yallah fayla yiw
yall'na yalla yokou sa kham kham barke seydina moukhamét psl barké seydil khadji Malick Sy ak wa keurem
MASHA ALLAHOU Seydi Tall Yallah naniou Yallah taas si sa Barkè amine si barké Seydouna MOHAMMED saw 🤲🤲🤲🤲🤲♥️💕💕💕♥️♥️❤❤💝💓🤲
Diaredieuf cheikh Oumar
Ma cha Allah amna sollo
Tawfekh ak taïssir bour yalla doli df ka si ioe sounou Daraa békté sakhe si sa dieum dji incha allah
Amna solo khôl sedna
Baraka allahou
Danke schön cheikhe hamet fall
Yalla nala Yalla aarraal boopam. Que le Seigneur t'assiste mon frère
Godou fans rèk kaye nianale
Mashallah oustaz
Grand merci à vous Serigne Ahmad Fall, qu'Allah SWT vous rétribue infiniment.
yall'na yalla défal la diamê berké seydina moukhamét psl
Dieuredieuf cheikh bi yalna yalla mottali sa yéné si barké seyyidina mouhamed saw ak barké cheikh tidiane cherif raddiyallaho anhou
C UNE AUTRE DIMENSION MAME OUMAROUL FOUROUYI TALL
Un grand merci à toi Eskey cheikhou Oumar foutiyou Tall
Serigne daara machallahh
Eskey Cheick Oumar Al Foutiyou Tall
Yalla nala sou borom ak cheikhna tidiani Aar la ta faylla gungi faaye si barkhé cheikhna tidiani amine
Masha allah Yalla na bour bi yook Xam xam bi t goudal sa fane 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Hoooo khôl yi sèèdna ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah Direudiefeuty Cheikh Seydi El Hadji Malick Sy. Oustaze Amet Yalla na suniu Borom samula ci barké Cheikh
Dieureudieuf serigne ahmad fall
Ma'achaAllah le peuple est content que le tout puissant vous protège contre les malfaiteurs. Je vous écoute depuis l'université de Caen Normandie .
Yo Allahu rèné wallahi mine mbéltiima guido .
Barakallahou fika ya seydi 🙏
Machallah sama soppé bi amatina solo kéne dou chiékh oumar waliyal waliabé
seydi fall gnou ngui la begue
Dieredieuf cheikh di yallna la yalla Faye si Daraja مولايا شيخ سيدي شيخ الحاج عمر فوتي تال رضي الله تعالى عنه
alhamdoul Allah machalllah serigne Ahmed fall on est fier de toi bonne et longue vie
Barakallahou fikk ya Oustaz Ahmad, nous vous suivons depuis Paris, on a tjrs le plaisir de vous suivre devant nos écrans. Yalla nala yalla doli takhawou inshallah. Bégg nanu bou bakh wallahi
Yalna la yalla barkel Yok sa kham kham samla yiir la té fayal gnoula
Hooo merci beaucoup que Dieu vous paye machalla cheikh omar foutiyou tall est notre oxygene
Vivi islam
Machaallah yalna yalla fayla oustaz ligueye bi rafetna
Machallah yallah na yallah Yoko xam xam bi
contaan nanou wallahi
Alhamdoulila alhamdoulila alhamdoulila
Mashallah CHEIKH OUMAR al FOUTIOU TALL mashallah.
Amoul morom fene thi afrik moy khalifa nieup thiey Seykou Oumar tal toro do mo diaxal nieup
Seykou Oumar tal dou morom ken xolal digantem ak wa makka ak madina ak palastine ak eguipty ak mali ak guine ak Nigeria ak seydi alhaji malik ak cheick ahamadou bamba ak imamoul mahdiyou ak alhaji ahmadou baro ndieguen
Ma shaa Allah yalla na Faye la yiw ya ahmeth fall
Diadieuf oustaz hamed fall
Merci beaucoup
Dieredieuf yalla na la bour yalla sambe la fayal la bopam
Mashallah diadieuf serign AHMED Fall barké SEYDiNA Mohammed sallahou aleyhi wassalam.
Koumay wakh fane la meuneu guisseii Serigne Ahmad Fall mi svp
Numéro bagui fofou
Machallah seidy tall tall tall
Machalla
Assalamou allaykoum Cherkh bi ! Yalla nala Yalla barkéle. AMINE
Dieureudieuf serigne Ahmad Fall, merci de nous faire connaître nos chers maîtres spirituels et leurs écrits. Que Dieu (SWT) vous récompense de la meilleure des façons Amine.
Machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah
Que dieu te protège ❤️
Machallah serigne bi contan nen si yaw de walay yalla nala yalla samou si brake naby
الشيخ عمر الفوتي طال ... رضي الله عنه ... جزاكم الله خير الجزاء يا استاذ احمد فال💓❣️✨💓❣️
Tall ha dow asaman
Seul Allah, son prophète seydina mouhamad anleyhi salatu wa salaam et Cheikh Akhmad Atijiani connaissent la grandeur et le degré de Cheikh Oumar foutihou tall
Assalamou aleykoum ya oustaz Ahmed fall di ziar bou weur davvero grazie molto interessante
Dieureudieuf 🥰🥰🥰🥰
Assalamu alaykum ! Dieuredieufety yalla na bour yalla fayalle nou la yiw
Thi barké yonenté bi
SAW Amine
Tall 🥰🥰
Machalla 😍😍🙏🙏❤️
Ziar serigne bi yalnala yalla faye