Ya Allah accorde a cet homme le plus Grand des paradis firdaws (amine ya Allah). j'aime ALLAH,J'AIME LE PROPHETE PSL,ET J'AIME CHEIKH DIALLO. QU'ALLAH SOIT TEMOIN
Savant bi boumou fi diogue kerok la koy sogua ham. A travers les statuts lako soguo guiss. Je suis allée sur Google pour savoir qui était ce grand homme et sur UA-cam j n'en revenais pas, depuis une semaine je ne fais que visionner ses conferences enseignements, Allahou Akbar machaallah borom xam xam deug demna, intellectuel beug Seydina Mohamed (psl) érudit hors pair véridique impartial, j n'ai même pas les mots hooo😭😭😭Yalla na souniu borom fayal teroula ci Aldianah you guene kaweh
Je le disais comme ça ma sœur. Le monde ne saura qui est Moukhidine Samba Diallo. Je le connais depuis des années et Alhamdoulillah je ne regrette pas ces enseignements car grâce à lui tu as un cœur léger.
Je suis fasciné par ces paroles je suis convaincu que actuellement il repose en paix je prie dieu pour que je croise ce grand sage cheikh mouhidine samba Diallo dans la vie future
Lima metti rek Moy dafa dem ba paret makay sogua xam magui niane sognou borome gnou guissé alahira in Sha Allah mame teudeul nga nopalou sa mission mate na
Ki macko beugue bilahi Cella fait 2ans je l'ais connue sur UA-cam Mome rk lay deguelou bilahi ak serigne same mbaye .. Nittu yalla deugg monguini .waliou kamal . Yalnagnou borom bi Tass sii barkéme Amine amine Barkei seydina mouhamed .p.l.s. 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Alahou akbar niak la xam si adouna rk lay réthiou diko dioy😭wa lahi bilahi wa talahi damako beug th xawou mako niak ko xam rk lay dioy thi môme ba légui😔méré walé sama boop lou takh xawou mala avant nguay dém😭machallah soumakoy khol mba makoy déglou sama xool bii séd boumouy séd yalla rk lakoy sédél🤲🤲🤲🤲🤲yalla naniou dadjé si aldianatoul firdawsi inchallah😭😭😭😭🤲🤲🤲🤲
Bama déguelo ba sama nopou datieu si yaw la ame louma yeuk lou sori lou sori lou nek si mane vous étiez un monument historique de notre pays mashhalah yallah na yallah fayla yonentibi terrou la si firdawsi dina dokh ba dougou si sagne inchallah nieuw ziar nieup tawfekh si ndiabote gui mashallah
Yalla hamnani meussoumako guiss waayé sama thiofêl si moom lou degouleu.C'est un véritable modèle pour les musulmans.Qu'Allah lui réserve une place exceptionnelle dans son paradis.Amine
They adouna kou bari khame kham kilifa deugou khame dine beug seydina mouhammad...beuri yeurmande def si mane lou bari doumala meusa fate figa nek yalla ga dokhanetou si keparou mouhammad psl metina metina
Man dé li diakhal defa guene adouna ma so go kham grâce à you tube bii qui met ces conférences paix à son âme que firdawsi soit sa demeure éternelle avec tous nos morts amine
Nos cœurs ♥️ et nos esprits sont remplis de bonheur et de lumière grâce à vos enseignements et tes rappels cheikh qu’Allah Soit satisfait de tes œuvres ainsi que ton ancêtre Seydina Muhammad amine.
SAMA SOPÉ BI TÉ YALLA TAH SI SA MBEUGUEUL SI YONINTIBI SAWS. YALNA YONINTIBI SAWS MIGUA MEUSSA BEUGUEU DIKA LIGUEYEUL TERROU LA. YALLA MIMA BAHE NIOU BOKEU DIOTAYE WAHTANE SA SALLON THI SAGNE BAMBARA MAKOY NIANE GUOUDE FANE TÉ NIOU BOKATE BENA DIOTAGNE THI ALDIANA FIRDAWSI AK GNI LA SOPEU YEUP SI BARKEP YONINTIBI SAWS AMINE YA RABBI.
Un grand homme que j admire bcp.Walahi il m a fait pleurer.C est regretable que j ai fais sa connaissance juste après sa mort.Un homme de valeur,de culture,un savant,un grand èrudi,un èducateur,un leader hors paire. Que dieu dans sa misèricorde infinie dèverse sa grace en abondance et fait de lui un demeurant èternel dd son paradis cèlestre.AMINE
Walahi sama xol nehoul Dara walahi ya bakh té goré j'ai jamais Poser les yeux sur vs m je peu attester k jtm indéfiniment cheikh bi repose en paix professeur
Je confirme ce que vous dites, je l ai aimé à la 1ère mn k je l ai vu en vidéo j ai eu un ressenti très fort aussitôt j ai dis Voilà.. un SAINT HOMME AL KHAMDOULILAH ALLAH m a guidé à le voir a sagne BAMBARA..........
@@mouhamadelmoustaphafaye5230 niou niane YALLA keup kouka sopeu yalna la raw té YALNA yeh niou bokeu ak mom diotaye auprès de notre bien aimé SEYDINA MOUHAMED RHASSOUL ALLAH SAWS AMINE.
Paix à son âme !Je venais tout juste de le découvrir! Un guide ,un érudit,un pédagogue,un un pilier de l islam.Triste le destin de l homme.QUE DIEU LE PAYE SON GRAND CŒUR .
Ken lawoune thi Féniou wayou yalla yi ken lawoune thi yeurmändé yalla yi ken lawoune thi waliyou yalla yi ken lawoune thi diagualé kattyi kon ina lilahi waina ilayhi rajdi houne mission bi nak daye continent rek lah ilaha ilahlah ..
Ma challah yalna yalla fayla yaa rabbi damala beugue thi sama khôl tè yalla rek tax wallahi finga nékke yalna yalla mèlalko ni Al dianna firdawsi si nékhaay amiine yaa rabbi
Ho ndey san j'arrive pas à regarder la vidéo intégralement sama yaram dawna kéndou Seydina Mouhamed psl. . .Cheikh Mouhidine Samba Diallo yalnako yalla yeram teh tass niou si barkem Amin yarabi 🙏😭👌
Bilay CHIEKH mi moussou mako guiss si sénégala walahi sopou n’a la lool man dé rédiona li ma yékh xam yalna la Yalla faye sa xoll Yalla yeureum la ko bakh si Sénégal mon dém😭😭😭😭😭😭🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Qu’Allah soit satisfait de toi imam samba diallo et que la miséricorde d’Allah soit sur prophète Mohamad sur sa famille ainsi que les nobles compagnons. Amine y’a Allahou pour l’éternité.
Ma shaa Allah 🙏🙏🙏 he was soooo blessed with his gorgeous heart love to help the people may Allah the almighty grant him the highest jannatul firdausi 😭😭😭😥
J’ai eu la chance de le voir 3 fois en rêves walay je l’aime bcp
Ah macha allá
@@gueyefatim8278❤❤❤❤❤❤❤😮😮
@@gueyefatim8278 😭😭😭😭
Ya Allah accorde a cet homme le plus Grand des paradis firdaws (amine ya Allah).
j'aime ALLAH,J'AIME LE PROPHETE PSL,ET J'AIME CHEIKH DIALLO.
QU'ALLAH SOIT TEMOIN
J’ai eu macha ‘Allah la chance de le rencontrer chez lui mou niaanal meu. Yalna Yalla jégueul ta xaaré keu Aljana Firdaws in sha Allah.
MachaAllah t es chanceux 🙏
Savant bi boumou fi diogue kerok la koy sogua ham. A travers les statuts lako soguo guiss. Je suis allée sur Google pour savoir qui était ce grand homme et sur UA-cam j n'en revenais pas, depuis une semaine je ne fais que visionner ses conferences enseignements, Allahou Akbar machaallah borom xam xam deug demna, intellectuel beug Seydina Mohamed (psl) érudit hors pair véridique impartial, j n'ai même pas les mots hooo😭😭😭Yalla na souniu borom fayal teroula ci Aldianah you guene kaweh
Je le disais comme ça ma sœur. Le monde ne saura qui est Moukhidine Samba Diallo. Je le connais depuis des années et Alhamdoulillah je ne regrette pas ces enseignements car grâce à lui tu as un cœur léger.
Amine Ya Rabi seddé yi raféte
Yalla miy bour yalla nala defal ans châteaux tia aldiana
AMINE !!!
Tu n'est pas le seul moi aussi
Je suis fasciné par ces paroles je suis convaincu que actuellement il repose en paix je prie dieu pour que je croise ce grand sage cheikh mouhidine samba Diallo dans la vie future
Lima metti rek Moy dafa dem ba paret makay sogua xam magui niane sognou borome gnou guissé alahira in Sha Allah mame teudeul nga nopalou sa mission mate na
wakhon naka ko dh né fok mou dém ñoukoy soga kham
Lolou moma dale
Bilahi mane tamite c la même chose yalla nako yalla yeureume
Sa batt thia kaw
Ndey san Ami yarabi machalla
Ki macko beugue bilahi
Cella fait 2ans je l'ais connue sur UA-cam
Mome rk lay deguelou bilahi ak serigne same mbaye ..
Nittu yalla deugg monguini .waliou kamal .
Yalnagnou borom bi
Tass sii barkéme
Amine amine
Barkei seydina mouhamed .p.l.s.
🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Souniou yakar taye ak euleuk yalla yok ay leram
Niar niou mata déglou machalah. Nitou batine laniou
Je suis chrétien mais je ne cesse de regarder ces vidéos pleines d'enseignements rip
M
Machalllah ♥️🤍♥️ j'aime beaucoup
Meussouma la guiss fi si adouna mais yalla nala guiss yawmalkhiam si barké seydouna Mouhamad❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alahou akbar niak la xam si adouna rk lay réthiou diko dioy😭wa lahi bilahi wa talahi damako beug th xawou mako niak ko xam rk lay dioy thi môme ba légui😔méré walé sama boop lou takh xawou mala avant nguay dém😭machallah soumakoy khol mba makoy déglou sama xool bii séd boumouy séd yalla rk lakoy sédél🤲🤲🤲🤲🤲yalla naniou dadjé si aldianatoul firdawsi inchallah😭😭😭😭🤲🤲🤲🤲
Repose en paix notre papa cheikh mouhidine samba diallo Yallah na Yallah haréko aldiana barke baye yarabi
En
Bama déguelo ba sama nopou datieu si yaw la ame louma yeuk lou sori lou sori lou nek si mane vous étiez un monument historique de notre pays mashhalah yallah na yallah fayla yonentibi terrou la si firdawsi dina dokh ba dougou si sagne inchallah nieuw ziar nieup tawfekh si ndiabote gui mashallah
Yalla hamnani meussoumako guiss waayé sama thiofêl si moom lou degouleu.C'est un véritable modèle pour les musulmans.Qu'Allah lui réserve une place exceptionnelle dans son paradis.Amine
Machalla
Amine
They adouna kou bari khame kham kilifa deugou khame dine beug seydina mouhammad...beuri yeurmande def si mane lou bari doumala meusa fate figa nek yalla ga dokhanetou si keparou mouhammad psl metina metina
Aminne kou bakh demna
Amin yarabi machalla
Alhahouma amiiine 🤲🏼
J'ai fait sa découverte que après sa mort 😥 yalnala yalla souniou brom yeurem té diégala kharé la Aljanatou firdawsi si barké Mouhammad (psl).
Ndeyessane Yalla nga dadier ak Yonenetebi salalahou alayhi wasalam ak Cheikh Abdou Khadre Djeylani. Vous nous manquez tellement.
Wallahii ndéye sanne ! Yalla na la souff sédd sa kaw yalla na la wahetou wi fékk si sa wéttou sopébii psl !! Yalla na niou yalla taff sa barké
Machallah machallah machallah yalla yalla fay yaa rabbi barké Mame Cheikh Mbaye kabir
Man dé li diakhal defa guene adouna ma so go kham grâce à you tube bii qui met ces conférences paix à son âme que firdawsi soit sa demeure éternelle avec tous nos morts amine
Wa parceque Sénégal les télévisions douniou guénné gniy wakh deugue État AK askane wi
Yalah nakoh borombih kharée aldiana you guenaa kawé thieh yekhanou akk kounée amine Amine
Nos cœurs ♥️ et nos esprits sont remplis de bonheur et de lumière grâce à vos enseignements et tes rappels cheikh qu’Allah Soit satisfait de tes œuvres ainsi que ton ancêtre Seydina Muhammad amine.
Amiiine
Repose en paix tes enseignements resteront éternel
اللهم آمين يارب العالمين
Vraiment Oustaz vous êtes sur le droit chemin pas de wiri wiri❤️❤️
Ndeyssane je taime bien nitou yalla deugeu bilahi moy goor yalla bi yalla nala yalla kharè aldiana
Tiey souniou wadji douma tayi dila sétane yallah rek moma doy si sédé tiofel bima ame si yaw. Mane deh défar ngama machallah. Yallah naniou yallah may yallah
Machallah ame naniou si iow yakar yallah gua bokeu diotaye ak seydina Mouhamed
SAMA SOPÉ BI TÉ YALLA TAH SI SA MBEUGUEUL SI YONINTIBI SAWS.
YALNA YONINTIBI SAWS MIGUA MEUSSA BEUGUEU DIKA LIGUEYEUL TERROU LA.
YALLA MIMA BAHE NIOU BOKEU DIOTAYE WAHTANE SA SALLON THI SAGNE BAMBARA MAKOY NIANE GUOUDE FANE TÉ NIOU BOKATE BENA DIOTAGNE THI ALDIANA FIRDAWSI AK GNI LA SOPEU YEUP SI BARKEP YONINTIBI SAWS AMINE YA RABBI.
Un grand homme que j admire bcp.Walahi il m a fait pleurer.C est regretable que j ai fais sa connaissance juste après sa mort.Un homme de valeur,de culture,un savant,un grand èrudi,un èducateur,un leader hors paire.
Que dieu dans sa misèricorde infinie dèverse sa grace en abondance et fait de lui un demeurant èternel dd son paradis cèlestre.AMINE
Waxul Mame waxul baye très très exemplaire soufi nekone bâ heurbi ma diokh KO sama bopp aduna ak alakhira machaalah
bilahi ya bakh yalla nako yalla doli lerr ci barker seydina mouhamed PSL.
Un grand homme. Qu'Allah t'accueil dans Son Firdaws
,Amin amin.
Yalla nala yalla yoko say ler si barkep borom Touba ❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏
Walahi sama xol nehoul Dara walahi ya bakh té goré j'ai jamais Poser les yeux sur vs m je peu attester k jtm indéfiniment cheikh bi repose en paix professeur
Ndeyssane, machallah ☝️☝️
Je confirme ce que vous dites, je l ai aimé à la 1ère mn k je l ai vu en vidéo j ai eu un ressenti très fort aussitôt j ai dis Voilà.. un SAINT HOMME
AL KHAMDOULILAH ALLAH m a guidé à le voir a sagne BAMBARA..........
@@WAWA-xd9yu machalalh machallah, ndeyssane. G ce même ressenti
@@mouhamadelmoustaphafaye5230 niou niane YALLA keup kouka sopeu yalna la raw té YALNA yeh niou bokeu ak mom diotaye auprès de notre bien aimé SEYDINA MOUHAMED RHASSOUL ALLAH SAWS AMINE.
Serigne Samba Diallo que firdawsi soit sa demeure eternelle que la terre soit légére sur luí
JE SUIS SATISFAIT DE CETTE VIDÉO PLEINE D'ENSEIGNEMENT ..
REPOSEZ ÉTERNELLEMENT AU PARADIS.VS ETES TOUJOURS AVEC NOUS ET POUR TOUJOURS.
Yalla gnou yalla Tass si barké am Tu restera toujours dans mon cœur 💓
Yalla gnou yalla Tass si barké am Tu restera toujours dans mon cœur 💓
Mmmmmmmm
MACHALAH MOUHAMADINE YALLA NAKA SUNU BOROM YEUREUM TE KHARE ALDIANA CII BARKEY SEYDINA MOHAMAD (PSL)
Yalna nala yala faye t barkel sa ndiabot barke seydina mohamed salal lahou aley wassalam....
رحمه الله
رضيه الله عنه ورضاه
😭😭😭😭😭🙏
Yalla na yalla yokou SA leer té tass niou tchi sa barké. Amine
Mon guide spirituel un homme multidimensionnel Machalla un savant un homme de Dieu Machalla yalla n'a yalla yésal yeurmandém ak diégal ci mom
Ndeyssane yallah na yeurmandé borom bi wathie thi kawame léral bamélame thi Barker arkhourane Barker Inchallah
Amin yarabi
Yalnaniou yalla fayal Serigne bi tei arr niou
Sama serigne demna kereuk deugue borom xam xam borom dîné yanna nous dadié thi aldiana you geuneu kawé thi barké psl
Nittou yalahh dou rerrre
Paix à son âme !Je venais tout juste de le découvrir! Un guide ,un érudit,un pédagogue,un un pilier de l islam.Triste le destin de l homme.QUE DIEU LE PAYE SON GRAND CŒUR .
Vous allez beaucoup nous manquer. Que le bon Dieu vous accueille au Paradis . Amiine!
Lui et sidy laminé me manque trop😭😭😭
Cheikh mouhidine Samba Diallo puisse Allah vous rétribuer votre précieux œuvre. Vous nous déjà ya Cheikhy
Diko dialé nieup Serigne bi 🙏🏿
Yalna yallah yokou léram thi barké seydina Mohamed psl ❣️❣️❣️❣️❣️🙏 🙏🙏🙏🙏
Ndeyessane une grande bibliotheque est partie. Yalla nagnou Yalla wannabee ci firdawsy ci barke Yonenebi Salalahou Alayhi wasalam
Ndeyssan je venais juste de le découvrir mais Dieu décida de le rappeler aux côtés des Elus du Paradis. AMEN
gggggg
QQ
Machalla un bibliothèque yalla na yalla yokkou ay leeram t yeureum 😥😥😥
Moussou mala guiss fi si aduna wayé koula sope la. Mangui niane yalla, Yalla na guissé ak yow ça alakhira
Wathie na liguey Sokhna si. Khana nianal ko rek Yallah yeureum incha'Allah
YALLA nagnou YALLA bolé wanalé ak mom biir Aldiana thi barki SEYDINA MOUHAMAD PSL
@@kif7471 Amine
Amin
Wallahi man mi lolou lay gnane yalla
Magui lay ñanal si barkep sedyna mouhamete sounou borom teroula thia aldianay firdawsi Amine
Ken lawoune thi Féniou wayou yalla yi ken lawoune thi yeurmändé yalla yi ken lawoune thi waliyou yalla yi ken lawoune thi diagualé kattyi kon ina lilahi waina ilayhi rajdi houne mission bi nak daye continent rek lah ilaha ilahlah ..
Ndey san daffa leer inchalla yalnako yalla fay Amin yarabi
Radiyallahou tahallah anhou cheickh mouhidine samba Diallo yallah n'a yallah yok leram té tass niou cii barkem Amin yarabi
Ma challah yalna yalla fayla yaa rabbi damala beugue thi sama khôl tè yalla rek tax wallahi finga nékke yalna yalla mèlalko ni Al dianna firdawsi si nékhaay amiine yaa rabbi
😍❤️❤️Yallna ko Yalla yeureum 🤲 yague mako kham mais féss na sa khôl 💓
Voila un homme de dieu .Qu.allah veille sur lui
Repose en paix . Que Dieu vous accueille dans son paradis éternel amine
Alhamdu li LAAHI 🙏🏾💖 to be a Muslim alhamdu li LAAHI 🙏🏾💖
Machallah Qu'il repose en paix Au Paradis Firdawsi RTA par la grâce de Notre Cher Prophète Muhammad SalAllahu Alayhi WaSalam
Yalna yalla diègalko tè tass nou ci barkèm
Ho ndey san j'arrive pas à regarder la vidéo intégralement sama yaram dawna kéndou Seydina Mouhamed psl. . .Cheikh Mouhidine Samba Diallo yalnako yalla yeram teh tass niou si barkem Amin yarabi 🙏😭👌
Yalna yalla yokou say ler barke Al cooran
Bilaye ken dou moom Way adouna mo mbindo nonou kooko sopla té waham yeep amma Solo MACHALLAH yalna YALLAH yokou leram❤❤❤❤❤❤❤❤
😭😭😭😭😭😭😭adouna yamna wor yalla na gnou ko yalla fayall te khari ko aljdanaa amiiinnnee
Skeye machalla alkhamdulila yalla na yalla kharè aldiana thi barche sèydouna Mohamed sallakhou alèyhi ya salam
Yalla na ko yalla yeureum te khare ko aldiana ci Barker seydina Mohamed psl
Machallah Mame yalna yalla yoke saleir Mame Amine ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ndeyssane lima meti rek moy xam bimala xamoul ba binga démé yalna suñu borom yesseul yeurmandem ci yaw ci barkey alqur'an 🤲🏽🤲🏽🤲🏽
Cheikh mouhdini yalla na yalla yokou léram yereum ko kou bakhoon nday san 😭😭🤲🤲
Jeureujeu Yalla n’a la yalla fay jeigeul la mayla aljana Gou Sakh jeureujeufeuti
Yalna yalla yeureumko tabalko firdawssi
Reposez en Paix yalla nala souniou borom fayy Mam🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Un vrai guide fédérateur que le sénégal a ignoré de toute son existence
Machalla yalla na yalla yok leram te tass niou si barkem si bARKI cheikhoul khadim
Bilay CHIEKH mi moussou mako guiss si sénégala walahi sopou n’a la lool man dé rédiona li ma yékh xam yalna la Yalla faye sa xoll Yalla yeureum la ko bakh si Sénégal mon dém😭😭😭😭😭😭🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
vos commentaires m'a fait pleurer je l'ai vu une seule fois en 2019 je l'aime beaucoup sa mission matña khamal nganiou
Yalnako yalla yeureum té diegeul ko si barké seydina Mouhammad sws
😭😭yallna gniu yalla fayal si brake serigne touba
Ya ALLAH yaw mi ame fayebi geune si faye yi yalla nganiou fayal souniou mame dji di Cheikh Mouhidine YA RABI
Machallla yalla n'a kham sa guinaw sakh lepam bakh vraiment Serigne DEUG mogui ni❤
Manchaala yalna sounou borom yalla fayalniouko barche seydouna Mohamed psl
Un homme multidimensionnel yala n’alla yoko yeurmandé si mom té tabnou si barkem
Yalla na yalla Yeureum té kharé ko aldiana firdawsi. Sénégal niogui soga kham sa diarigne 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Yalna yalla yessal yeurmandé ci mome té taass gnou ci barkem Allahouma amiine
رحمة الله عليه
اللهم إغفر له وارحمه واسكنه فسيح جناته
Soumalaye deglou démal contane, yalnala yalla féye sa jeuf Oustaz
yallna niou yalla fayal cheikh Mouhidine samba diallo amine ❤
Un homme pieux et courageux il prédisait souvent sa mort dans ses prêches qu'Allah SWT l'accueille en son pouvoir paradis céleste amine
Yalla naniou Yalla tass sisa barke Yalla yesseul yeureumendem thi yaw mame boy yalla wonaleniou kerok yawmal khayam amen amen yarabi
Qu’Allah soit satisfait de toi imam samba diallo et que la miséricorde d’Allah soit sur prophète Mohamad sur sa famille ainsi que les nobles compagnons. Amine y’a Allahou pour l’éternité.
Yalna cheikh bi niou guissé Aldiana Aminn ya Rabi
Cheikh Mouhidine yalnagnou yallah fayal te tass nou si barkem
Koula sopela téh meusoumla guiss yalnala yalla haré ardiana firdawsi
Alkhamdoulillah! Dieurwdieuf Serigne touba
Nioune daniou la yékha xam mais wallahi walliyou nga kou melni yaw dotoul am Sénégal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ma shaa Allah 🙏🙏🙏 he was soooo blessed with his gorgeous heart love to help the people may Allah the almighty grant him the highest jannatul firdausi 😭😭😭😥
Mis HQqse
Se ne ng alle
Machalla le TRÈS GRAND ÉRUDIT. Repose en Paix
yalla nagnou la yalla fayal aldiana firdawsi yalla gua khippé si wétou naby amine
yalla na yalla yokeu ay léram bilahii borom xam xam demna
اللهم ارحمه واغفر له ءامين 😭❤👉معك يا شيخي
Yalla na Yalla yeesal yeumandeem dolli koy leer