Cheikh Seydi Ahmad Fall sa Lissane Arabe amna loula si Yalla defal ! Yalna Yalla lafala thiat te taxawoula ak sa équipe barké Cheikhou Omaroul Foutiyou Saahibil Rimahil Gadawwi RTA!
Association sopé Serigne Ahmed Fall kagne lay takhaw ki dafa diara diapalé deugleu gnane bakhna mais dimbal nassa fek lokhol borom. On peut s’unir car l’union fait la force et aider le hadara Ahmadiya
Souniou oustaz Daara akk gniom Aladji ak gni nekk dans l'ombre di participé ci ligueybu am solo et tous ceux qui participent tant soit peu de par ce qu'Allah les a octroyez de mm ceux qui ne tarient pas de par leur prière Yalla na leine Yalla faay ci barké Yonente(sws) akk Cheikhou Tidjane(rta) 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Machallah amna mbegté lol si guiss sama soppé serigne ahmad fall di wakhtané sama wassila chiékh oumar al foutiyou tall codda adama aissé fière d'être omarien
La pertinence et le fait que qu'il cite tout le temps ses sources font qu'on ne se lasse pas de regarder ses vidéos. Finalement c'est tout ce qui fait leur charme, leur singularité. C'est comme si on apprenait une leçon....... Rien que pour ça mille mercis 🙏🙏🙏🙏 Quand il parle des miracles de Cheikh Ahmed Tidiani Chérif RTA et qu'il dit Cheikhhhhhh Tidiaaaaaaaane, je suis par terre. Je ne m'en lasse pas lol
Mashalla mashalla Yalla na Bour Yalla defale leu goude fane bou andak werr ak werlé soutoura bou sakhh abadane weurseukk bou yaatou bidiahi Cheikhou Tidjany rta ak sa ekip Bii yeupp ...cntane naniou Oustaz
MACHALLAH YAW DAL YAFII RAWW KHAW MA FO DIANGUÉ MAIS C'EST EXCELLENT EN PLUS VOUS ÊTES EXCEPTIONNEL AVEC L'UTILISATION DES LANGUES FR ET ARABE ET WOLOOF
Macahalla amna solo dh mais nak tamitt mane moom dama amm sokhla bomakk thi yalla ta nak lolou moom serigne Ahmad fall rek lasi yakarr yalla khamnako 🤚🤚🙏🙏ibrahima diop la depuis Maroc wonala.sakh tamitt vocal nala
Amine ya rabi yalna bour YALLA nangou gnany si barké Seyidina Mouhamad que Dieu vous protège et vous garde vit bien vit longtemps sous la protection D'ALLAH
Li dè motakh fènkate ba done fène mame mor mbaye done sosse maiis mome wakhouma la touti si mais dou dara Cheikhou Oumar Al Foutiyou Tall (rta) moye Serigniou Serigne si Kodda adama Aïsha (rta) YALLAH naniou Yallah Taas si barkém si barké Seydouna MOHAMMED saw amine ya Rabbi 🤲🤲🤲💕💕♥️♥️♥️
Waxou ma sax Seykou Oumar wante yayam rek adama aiché ken ganou ko ragal yala lou mou def gui sou niou jiguen bu ko def taxaw di diouli bay sa dom am lou niaw rey ko te dogo sa diouli
Macha allah macha allah ya oustaz wakh tane bi rafètna. Yalla na yalla yokou xam xam. Si barkè Cheikh Oumar. Bilahi contane nagnou et Yalla na Yalla contane. On attend avec impatience la suite. Amine et Yalla nagnou Yalla def ay talibè cheikh you weur.
Autant attendu
Et nous voilà enfin
Ay sama sope bi
Yalla na yalla defal la jamm Thi barki Yonentibi SAW
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
MACHA ALLAH CHEIKH BI KEUR MAME ELIMANE SAKHO YEUPE SOPE NANIOULA YALNA YALLA FAYE YIWE
Kou mou nex ak komou nexoul dousa morom serigne seykou oumar dara diam wesuna tok di ko tekale benen nitou yalla non bokou thia ki kene la
شكرا ❤
Walliyal waliyabé
Thierno Cérnabé
Kodé adama aissa, élimane ciré samba demba ali moctar
Chose promise et faite.machallah.
Stp apportons notre pièce à l'édifice
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Wallahi ndeyssaane
Wallahi
Wallahi
Wallahi ndeyssaane
Coda adama aiche elman chire Samba demba ali mouktar gan suba tel bala dianta bi chow mou neka borom dekue bi
Ouztas yalla na gua goude fane sa wakhtane wi amna solo kep kouye tidjiane si Afrique de l'ouest Amel gua ndioukel cheikhou Oumar foutiyou
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Cheikh Seydi Ahmad Fall sa Lissane Arabe amna loula si Yalla defal ! Yalna Yalla lafala thiat te taxawoula ak sa équipe barké Cheikhou Omaroul Foutiyou Saahibil Rimahil Gadawwi RTA!
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Wax leen ko thi kaw Seykou Oumar tal amoul morom fen
Association sopé Serigne Ahmed Fall kagne lay takhaw ki dafa diara diapalé deugleu gnane bakhna mais dimbal nassa fek lokhol borom. On peut s’unir car l’union fait la force et aider le hadara Ahmadiya
Je suis partant
@@cheikhfall2285 moi aussi
وانا ايضا
Je le connais personnellement
Àliiyagna amna niawonagne fi yagoull
Machallah sëriñ Ahmed Faal yow rekk doy Nga ci firndeel ni Cheikh Ahmed Tidiane rta du moromu gaayi.
Walay cheikh Oumar amoul morom
Souniou oustaz Daara akk gniom Aladji ak gni nekk dans l'ombre di participé ci ligueybu am solo et tous ceux qui participent tant soit peu de par ce qu'Allah les a octroyez de mm ceux qui ne tarient pas de par leur prière Yalla na leine Yalla faay ci barké Yonente(sws) akk Cheikhou Tidjane(rta) 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Alfoutiyou tall kodda adama ayssa elimane cire samba demba Ali mouctarr ❤🙏🏼✊🏼
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Talllllllllllllllllll
Serigne bi man deih damala sopeuh❤ yalna nala BOUR YALLA fay geune di fay🤲🏿🤲🏿🤲🏿...Dieureudieuf
J'attendais avec impatience wakhtan cheikhou Omar bi kham kham rek mo wor yalna la yalla faye
Machalla sema fallén bi yalna yalla samomou la aar la sotoural la déf nio ay talibé chiekh Ahmad tidianiy
Serigne profesor oustaz ahmed fall yalna yalla barkel xam xam 💚💛❤
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
J'aime ces genres émission 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Machallah amna mbegté lol si guiss sama soppé serigne ahmad fall di wakhtané sama wassila chiékh oumar al foutiyou tall codda adama aissé fière d'être omarien
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Yo Allah souré seydi fall
Yalla na la Yalla may goudou fan werr ak soutoura begueul nieupo machalla
Il faut beaucoup partager cette vidéo pour que la jeunesse africaine reconnaissent ses vrais héros
Mashallah serigne ahmed
Mon ziar depuis les usa
senegal wornagn geum sen bopp que des grands hommes qu'on a eu qu'Allah nous protège du mal
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Cheick Ahmad tidjani 🇲🇱cheick oumar tall 🇲🇱cheick hamad hamahoulah 🇲🇱machallah pour tout c’est waliou au Mali 🇲🇱
La pertinence et le fait que qu'il cite tout le temps ses sources font qu'on ne se lasse pas de regarder ses vidéos. Finalement c'est tout ce qui fait leur charme, leur singularité. C'est comme si on apprenait une leçon....... Rien que pour ça mille mercis 🙏🙏🙏🙏
Quand il parle des miracles de Cheikh Ahmed Tidiani Chérif RTA et qu'il dit Cheikhhhhhh Tidiaaaaaaaane, je suis par terre. Je ne m'en lasse pas lol
Yaa Baakh Sokhna ci Lii nga Waakh Amna Soolo
@@oumardiouf5954 dieuredieuf. Yalla nagnou Yalla feyyal makk yi. Kenn dou gnome
Yalna yalla goudal sa fane
Amine ya rabbi yo Allahou juudnu nguurdam mah annéné le premier premier ministre
Serigne bi yaw dall bayilack souniou borom rék mo fadjialla adio yepeu bibarakati seyidil woudjioude PSL🙏🙏🙏
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Kou la xamoul he lalay wowe Seykou Oumar Tal bouku thi moy seeni serigne
Mashalla mashalla Yalla na Bour Yalla defale leu goude fane bou andak werr ak werlé soutoura bou sakhh abadane weurseukk bou yaatou bidiahi Cheikhou Tidjany rta ak sa ekip Bii yeupp ...cntane naniou Oustaz
Dieureuf dieuf sekh Abdul Hamid sarr borome diamano
Machallah seydi Ahmed diazakhalahou hayrane
Jazzakumullahu ana hairan yagg fi looooool te werr si Barkeh Nabi (SAWS)🙏🙏🙏💕💕💕
Maa challah yoo allah yo6e thierno Ahmed fall skoy thierno muntaga Ahmed muntaga cheikh umar
Mancha alla mancha alla yalla na sa diam yagui gnep beug nagno si barké chiekhou omar
Tall al foutiyou serignou serigne yi
MACHALLAH YAW DAL YAFII RAWW KHAW MA FO DIANGUÉ MAIS C'EST EXCELLENT EN PLUS VOUS ÊTES EXCEPTIONNEL AVEC L'UTILISATION DES LANGUES FR ET ARABE ET WOLOOF
TIVAOUANE la diangué teksi fala deuk
Dieureudieuf Kilifeu Gui Yalnala yalla fay yiw
Ma sha Allah Serigne Ahmad Fall yallah na yallah fayla yiw lerna nekhna am ndieurigne yokounagnou bou bakh ma sha Allah
Machaaa allaaaah ❤️❤️❤️
Djiss rekk contane
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
masha'ALLAH yallah na yallah faay yiiw ya oustaz..Cheikhou Oumar (rta) le supranational sopenagneko trop yallah sedenaako
AMOUNO SA FAYE WAYE YALLA AMNA SA FAYE YALNALA YALLA FAYE SI BARKE CHEIKHOU OMAR
Merci Serigne bi Fall Yalla nanu Yalla taass thi barké mag gni inchallahou..
contaan nagnou Yalla nala Yalla faye...alhamdoulillah
Yalla na yalla mottali Lep si batké Mouhamed(psl) si worma Cheikh Aboul Abass(rta) tahawahou cheikhou Omar (rta
Yalla nanou Yalla fayal Mame Cheikh Omar (rta) dieureudieuf ya Oustaz
Dieureudieuf ya Oustaz yalla yokeu leu werr ak soutoureu 🙏🙏
Eskey ya oustaze yalla nala yalla bolli xam xam
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
yalla na la yalla yok yiw
Oustaz yalna yalla dolli weer
Machallah wakh tane bi amena solo
yall'na yalla dafal la diam barke seydina moukhamét psl barké seydil khadji Malick Sy ak wa keurem
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Macha Allah y'a cheikhina yalla n'a yalla doli diapalé dila ziar dila bégué
Macahalla amna solo dh mais nak tamitt mane moom dama amm sokhla bomakk thi yalla ta nak lolou moom serigne Ahmad fall rek lasi yakarr yalla khamnako 🤚🤚🙏🙏ibrahima diop la depuis Maroc wonala.sakh tamitt vocal nala
Bour yalla def tawfekh ak taïssir incha allah
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Ya Cheikhy Oustaz Ahmed Fall yo Allahu wadané sutura aduna é lakhara ya barké Al Fuutiyu Tallllll (RTA).
Amine ya alahou seydi Thiam🤲🏿
Eskey seykou Oumar Tal yalla may nala limou mayoul beuna nit bou nioul tal
Amine ya rabi yalna bour YALLA nangou gnany si barké Seyidina Mouhamad que Dieu vous protège et vous garde vit bien vit longtemps sous la protection D'ALLAH
Fatabarakalâhou
DjazakaLahou khayran dahimane
Machalla ya oustaze yalna yalla barkel xam xam bi...goudou fane ak wer
Yalla na yalla barkel khame khame bi
Assalamou anleykoum serigne bi nio ngui sakou niane té dila nianal Yalla
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Ya imam diabel nio rafetlou sa takhaway Machallah Dieureudieuf
Mâcha ALLAH content de toi outaz AHMAD FALL
Yalla n'a yalla fay la oustaz
Yalna borom bi yokou la ayy faydoul anewar
Machalla oustaz Ahmed fall yalna bur yalla faye yiw contanena
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Machallah Cheikh Ahmed amatina solo lool Billahi yalla na suniu Borom deguereul taxaway bi
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
MashAllah. Yalla na Cheikh Omar Foutyou RTA contane si yaw. Merci beaucoup
Assalamou aleykoum ya oustaz Ahmed fall di ziar bou weur davvero grazie
Asalamou alaykoum, Yalla na Yalla faylén ci barké yonnétbi salalahou aleyhi wa salam.
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Alhamdoulilah dieuredieuf Serigne bi yalna buur bi barkèl té bégueul la lou raw ninga nii béguelè 🙏
Doundeul wereul Ya Oustaz
Contan nagn trop yalla xamnako
ماشاء الله تبارك الله سيدى
Machallah Serigne Ahmed Fall
Merci serigne
ورضي الله عن مولاي الشيخ سيدي الخليفة الحاج عمر الفوتي طال ومددنا وقدوتنا إلى يوم الدين
ونفعنا به في الدارين يارب
Allahouma salli à la nabiyina mouhamad saws. Dieureudieuf oustaz
Dieureudieuf waay Oustaz 🙏🙏🙏
بارك الله ماشاء الله رضى الله تعالى عنه
CHEIKH OUMAR DAFFA RAGUAL YALLA
Bilahi ya Bakh tu es un envoyé
Li dè motakh fènkate ba done fène mame mor mbaye done sosse maiis mome wakhouma la touti si mais dou dara Cheikhou Oumar Al Foutiyou Tall (rta) moye Serigniou Serigne si Kodda adama Aïsha (rta)
YALLAH naniou Yallah Taas si barkém si barké Seydouna MOHAMMED saw amine ya Rabbi 🤲🤲🤲💕💕♥️♥️♥️
يا أشبه النّاس بالفاروق ياعمرُ 💚💓
Macha'alla serigne Ahmed Fall yalla na yalla sameula té barkel sa xam xam
Xol sedeu Tina yalna yalla geureum
Waxou ma sax Seykou Oumar wante yayam rek adama aiché ken ganou ko ragal yala lou mou def gui sou niou jiguen bu ko def taxaw di diouli bay sa dom am lou niaw rey ko te dogo sa diouli
Machalla Hadji yagui niouy leral sounou mak ji
Dieureudieuf ta oustaz machalla
Macha allah seyidi Ahmad fall yalna yallah barkèl
Macha allah macha allah ya oustaz wakh tane bi rafètna. Yalla na yalla yokou xam xam. Si barkè Cheikh Oumar. Bilahi contane nagnou et Yalla na Yalla contane. On attend avec impatience la suite. Amine et Yalla nagnou Yalla def ay talibè cheikh you weur.
serignbi yalla deffal leu soutreu
ua-cam.com/channels/5NE2Ii_42Xw6smh-r4Fqqg.html
Walahi serigne Ahmed fall yalna sunu borom fay leu si barkei Taahaa Aleyhi salatou wa salam
Machallah Amna de ziar fall
Jerrejef Fall walahi mashalla
الحمد لله رب العالمين
الحمد لله رب العالمين
الحمد لله رب العالمين
الحمد لله رب العالمين
Dieureudieuf Oustaz yalna yalla yok xam xam bi weireul thieur yi mayla gouddou fane ak weir si barkei sa sopei bi Mawlaya Cheikh rta
machalla tabar kalla yalla nala yalla fay
استاذ احمد فال الله يبارك فيك
Contane nanou blh yalnala yalla fay ak team bi yéep
ماشاء الله يا اخانا الكريم
صدقت واصبت جزاك الله عنا خيرا
Seydou ly ane a diarama bida sox Li nimero ma mi da niaa gui ma sa yi coma nelda kam nimero
@@babaly5821 inchalah laisse mon ton num je te ferai signe
Tallou Allah talloum halwar guédé yo halwaréne. Codé Adama Aicha. Abouh dini wa takhwa Radiyallahou Tanhala Anhou
Alkhamdoulilah Ya Oustaz, Yalna Y'AllAh goudal say fane, Té wéral bate bi🙏♥️🔥♥️