Eumeu Séne sunu 2millions la Yobu Mak Boy Niang? Sokh fait de grave révélation et détruit Zarco

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 5 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 686

  • @SenbuzzTV
    @SenbuzzTV  Рік тому +18

    N’oubliez pas de vous abonner sur votre chaîne Senbuzz Tv et d’activer la cloche 🛎 pour recevoir les notifications merci.

  • @Mouhamadoukone-xg9sx
    @Mouhamadoukone-xg9sx Рік тому +37

    Ama balde dal moy goor doko degg si yiii machallah ❤❤❤

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye7353 Рік тому +55

    Sokhou Ya wakh Deug Sa kadou Raféttna Vérité absolue ❤🙏🏽

    • @buz7755
      @buz7755 Рік тому +1

      Machallah ❤❤❤❤❤deug mom nekhoul rek

    • @buz7755
      @buz7755 Рік тому +1

      Sokhou ak deug wakh Machallah ❤❤❤

    • @alifall8066
      @alifall8066 Рік тому

      Sokh fonkk nala yaw AK boy Niang mé eumeu dou nitt kou deugou bo dégé nimouy wakhé

  • @Teranga9999
    @Teranga9999 Рік тому +24

    Eumeu sene je suis très choqué enfette il a deux visage , courage Grand champion sokhh 💪🏾💪🏾💪🏾🙏🏾

    • @tapha76
      @tapha76 Рік тому +2

      Je te promets que il joue double jeu
      Demande à un ancien compagnon avant qu'il soit connu

    • @yahyareskp40
      @yahyareskp40 Рік тому +3

      Walahii je te jure que Eumeu nafex pirr leuh walahii al azim ta day watte si ay fene walahii

  • @boubacarba8323
    @boubacarba8323 Рік тому +33

    Franchement sokh une personne digne 🙏🙏🙏

  • @yayadiaw4676
    @yayadiaw4676 Рік тому +6

    Boy Niang 2 commence à me plaire ❤❤❤❤mane suis fans de Fan de BG2 nak

  • @MatarlaahiSeck
    @MatarlaahiSeck Рік тому +15

    Merci sokh wédi dou ragal sétal sa dérr la vraiment 🙏🏼 merci aussi sen buzz le combat continue par ce que les gens comme becaye mbaye noy doléle VIP yii chaque jour que je réveille nouveau dossier mbaye🙏🏿🇸🇳💉❤️

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking382 Рік тому +60

    Sokh grand champion, on peut sentir la vérité dans ses propos, mais Yallheu neu Yallheu diouboléléne yéne nieupou Inch'Allah Yallheu neu Yallheu yoné nieupou diamou ak khéwal Inch'Allah 🙏

    • @Salamsalam-th2fb
      @Salamsalam-th2fb Рік тому

      Danga barri waax ... comme une femme. En plus lingay waay dara douthi deugu doul reek

    • @ouzdaking382
      @ouzdaking382 Рік тому +2

      @@Salamsalam-th2fb sa baye ak sa yaye gnioma diangale DOULE embecile bi 😂🤣

    • @dianablackqueen3510
      @dianablackqueen3510 Рік тому +1

      ​@@ouzdaking382merci là bas 👍🏽😅😂😂

    • @ouzdaking382
      @ouzdaking382 Рік тому +1

      @@dianablackqueen3510 de rien la belle Diana , gni danion réw tè soff beu paré bari wakh derrière séni écran laniouye nékk Di binedeu louléne nékh , mais filamaye fekk 😆

    • @Jali_balla_moussa
      @Jali_balla_moussa Рік тому +1

      @@ouzdaking382 ki warr ngako wakh lou raw lii🤣🤣🤣...

  • @marrakexhmarrakrxh9285
    @marrakexhmarrakrxh9285 Рік тому +9

    Sokh yalla na yalla defal diam

  • @abdoudiop5163
    @abdoudiop5163 Рік тому +6

    sokh masahala eumeu sene nafekh la ama balde future roi des arene insahala ❤❤❤

  • @momobouthiapathiolybi7752
    @momobouthiapathiolybi7752 Рік тому +17

    Thiey thiapathioly bi maissa khary missi ndiomb balla codou mané mbaye yirim aka goré❤❤❤❤

    • @teckjunior8005
      @teckjunior8005 Рік тому +1

      Ihhhhhhhh copin li goudou na dé 😂😂😂😂😊

  • @serafall946
    @serafall946 Рік тому +8

    Merci beaucoup mon frère degue nekhoul sokh degue gua wakh billahi ❤❤❤❤❤❤❤

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 Рік тому +20

    Ama Baldé fii lako Gaston Mbengue
    Wara Diox 10 million le reste thi cachem jul Baldé Dii Tagall Ama Baldé n’ai Gaston bouko wédé bayi Nako ak Yallah ✅Ama Baldé Goorla Garmila ✅✅✅✅

  • @buz7755
    @buz7755 Рік тому +6

    Sokh wakh katou deug leu Machallah ❤❤❤❤❤❤❤

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 Рік тому +5

    Pourtant sokhou loulér laye wakh ☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️déglou lénko boubakh 🦻🦻🦻🦻🦻🦻🤘

    • @loeildutempstv1998
      @loeildutempstv1998 Рік тому

      🤣🤣🤣kou wakh nguen ni mom leu

    • @ibrahimadrame9499
      @ibrahimadrame9499 Рік тому +1

      @@loeildutempstv1998 non lolou wakhdjiou dioup laniouy topou ☝️☝️ déglou lénko boubakh wakham mogeuneu dioupp fouuuuf ta sokhou nitou deugeuleu loulér nagni laye wakh ☝️☝️

    • @loeildutempstv1998
      @loeildutempstv1998 Рік тому

      @@ibrahimadrame9499 sokh dafa togne eumeu sene ndakh kara dolé mo dal sikaw sokh donc dafa warona tontou kara dolé teh boumsi takhal eumeu ndakh eumeu wakhoul ak mom teh depuis bobou bé légi mongi insisté teh souko eumeu yobou won si yonn sokh mofay déss en plus mom sokh néna eumeu délona xaliss bi donc waratoul won takhal eumeu di dal sikawam lolou togne la koi

  • @princetorodo8590
    @princetorodo8590 Рік тому +4

    Lou lerr nga wakh man parcelle la deukh mais djiko ndongo lo ngene Di wara dokhe diam si ioe sokh❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @courasarr1582
    @courasarr1582 Рік тому +20

    Sokh ya taye défal loula nékh ont t'aime fort ❤❤

  • @courasarr1582
    @courasarr1582 Рік тому +13

    Sokh nite cou bakh billahi ❤

  • @beuleupndao1155
    @beuleupndao1155 Рік тому +11

    Boy niang ma agréablement surpris ❤❤❤

  • @cheikhba8572
    @cheikhba8572 Рік тому +9

    Boy Niang yayy gorrr pirr❤️❤️💚on taime un point c tout

  • @galayebeye7868
    @galayebeye7868 Рік тому +5

    Bilay Kouko dégue khamni lim wakh lepou degue la amall diame rk yaw sokhe ❤

  • @BabaDiagne-l5n
    @BabaDiagne-l5n Рік тому

    Damadane, deugue sock, mes depuis, je je té entendu, je suis fans de toi. Du courage

  • @diarra_chou8497
    @diarra_chou8497 Рік тому +3

    Man Sokh damako begue dafa degou trop machalla nékal thi diam❤️❤️❤️

  • @alfredtavarez3558
    @alfredtavarez3558 Рік тому +11

    Merci sokh boy💪🏾💪🏾💪🏾✊🏿✊🏿✊🏿

  • @AdamaMballo-ke6fw
    @AdamaMballo-ke6fw Рік тому +21

    Vérité absolue merci boy niang geste noble

  • @francois7379
    @francois7379 Рік тому +7

    Boy niang c un gentleman vraiment

  • @BabelThiam723
    @BabelThiam723 Рік тому +4

    🇸🇳❤️❤️❤️Vive sokh ❤️❤️❤️🇸🇳

  • @mouhamedniang5708
    @mouhamedniang5708 Рік тому +3

    Sokh amal jamou rk❤❤

  • @djibysoung2998
    @djibysoung2998 Рік тому

    Nice sokh Eumeu defiyanla

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 Рік тому +14

    Merci beaucoup sokhou🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏diambar nga DEUG monékhoul rék

  • @khalifambengue6125
    @khalifambengue6125 Рік тому +11

    Macky Sall si bén côté bakhna si Sénégal ndakh dina fènial nafékh yep bala 2024 in challah niou raxas deukbi yep merci sokh yaw nitou deugeu nga ma challah yalna yalla barkel lepp

    • @soramalik5836
      @soramalik5836 Рік тому +1

      Lolou dongue lafi liguey. Nafekk YI la fegnaal

  • @courasarr1582
    @courasarr1582 Рік тому +24

    Boye niang dafa goré billahi nitt kou bakh la xaliss titeulou ko ❤❤

  • @sambandiaye7026
    @sambandiaye7026 Рік тому +3

    Neysane diambar yaw diam rèk guay Ame Inechalah ❤️❤️❤️❤️

  • @beuleupndao1155
    @beuleupndao1155 Рік тому +15

    Je ressens la vérité absolue.

  • @dogothiam2971
    @dogothiam2971 Рік тому +4

    Bravooooo sokhou diam thi yaw gaïndé

  • @mamadoudiagne4827
    @mamadoudiagne4827 Рік тому +24

    🎉 sincèrement Ama Balde kou digne jamais nga degko si detayou xalis

    • @roqdem3605
      @roqdem3605 Рік тому +2

      Ama baldé moy goor deug bilaye

  • @BabelThiam723
    @BabelThiam723 Рік тому +26

    ❌❌❌Macky Sall dégage ❌❌❌ li lépou mom leu ❌❌❌

  • @cheikhba8572
    @cheikhba8572 Рік тому +6

    Boy Niang ❤️💚

  • @courasarr1582
    @courasarr1582 Рік тому +5

    Nous ont t'aime fort vraiment ❤sokh champions ngua billahi ❤

  • @assanegueye28
    @assanegueye28 Рік тому +3

    Masala Sokho kou degou ga degou si réwmi dafa méti yalla nala yalla samou

  • @bassirouba3035
    @bassirouba3035 Рік тому +11

    Wéddi du ragal sétal sa derr la❤

  • @courasarr1582
    @courasarr1582 Рік тому +20

    Eumeu dou ndéye touss ya tay boy💪💪

    • @boyeniang3781yeumbeul
      @boyeniang3781yeumbeul Рік тому

      😂😅

    • @malicksarr7557
      @malicksarr7557 Рік тому

      Yaw yamana kate sa ndaye EUMEU SENE mon mane sa dayou ndaye

    • @courasarr1582
      @courasarr1582 Рік тому +2

      Ioe damay katt sa leufou ndéye dei doméram

    • @timtim6971
      @timtim6971 Рік тому

      ​@@malicksarr7557gueno fei rew kene sa ndey rek ngay saga doff bi nga done

    • @malicklo4613
      @malicklo4613 Рік тому

      @@malicksarr7557Ioe Katal sa ndy Ioe ak eumeu sene sen xourou bay

  • @babacarbathia-ko8px
    @babacarbathia-ko8px Рік тому

    Masha Allah sokhu, your statements are beautiful. Keep moving let no one stop you.

  • @Dougeuldioubeul
    @Dougeuldioubeul Рік тому +13

    Eumeu sene amoul Ngor si khaliss 😫😫😫

  • @Enfant_béni_7
    @Enfant_béni_7 Рік тому +6

    EUMEU SÉNE VRAIMENT SIKEU NGA LOLEEEE NAK VRAIMENT 😢 KOU NIEUP TOUFFLI NGA TOYE 😢 TOUJOURS YAW RÈK YAY XOULO AK NIEUP 😢OH WATA WATT 😮

  • @asseba4700
    @asseba4700 Рік тому

    le journaliste est extraordinaire

  • @Bilal66850
    @Bilal66850 Рік тому +14

    Un homme de vérité

  • @djibery1023
    @djibery1023 Рік тому +3

    Là je vois un homme très juste boy Niang😍

  • @FallouFall-s3b
    @FallouFall-s3b Рік тому +6

    Merci boy niang

  • @demebadiekh7476
    @demebadiekh7476 Рік тому +8

    Mbeur goré woule sokh daga am foula rek ayy eume sene kon niga mel si khalis 😅😅😅😅😅

  • @abdousalamgueye9481
    @abdousalamgueye9481 Рік тому +12

    Merci beaucoup ❤❤❤

  • @bassdiokhane1472
    @bassdiokhane1472 Рік тому +4

    Merci sokh degeu rk mon wour yall nala yalla diapalé bare képp borom Touba Mbaké balla masala

  • @awasanneh9174
    @awasanneh9174 Рік тому +3

    Bilahi deugou nga ni diola
    Diola dey deugou ❤❤❤❤❤❤
    Machalla

  • @bambabalde9027
    @bambabalde9027 Рік тому +2

    Bilah walah man sa wakh la geme ❤❤❤

  • @diambendoye3320
    @diambendoye3320 Рік тому +2

    Thiongane tu et le meilleur de ta génération naniou khol si yaw

  • @serignefalloumbacke7849
    @serignefalloumbacke7849 Рік тому +1

    Sokh mi dh mowakh deug epuis boy niang Machala

  • @bathieka-m2i
    @bathieka-m2i Рік тому +1

    Merci mon frere

  • @cheikhsene9850
    @cheikhsene9850 Рік тому +6

    Bravo mbeur

  • @sadiokaradiallo3414
    @sadiokaradiallo3414 Рік тому

    Sokh yalla nagnela d'âne Amin vrai seytane' ga
    Eumeu sene yala na am diam

  • @marenadiop2705
    @marenadiop2705 Рік тому +2

    Champion du courage

  • @ibrahimabadiane8252
    @ibrahimabadiane8252 Рік тому +7

    Eumeu séne ci bopam moy nite kou bone bilahi wor kat pirr la

  • @ndiayeabdouaziz588
    @ndiayeabdouaziz588 Рік тому +2

    Ay way sokh yakh nadiou ko way yalla naga danou sa comba bi inchalla yalla nako yalla def

  • @ndeyefatoumarone8391
    @ndeyefatoumarone8391 Рік тому +1

    ❤❤❤❤❤

  • @sakhewarfatma7116
    @sakhewarfatma7116 Рік тому +2

    Noooo Tyson ndekete wakh na duegg eumma yama bett nooo ki mbam pur la ndekete lou niou ko wakhal massouma ko guem me tay la guem ni lepp dueg la

  • @mouhamedniang5708
    @mouhamedniang5708 Рік тому +3

    Deugue rk nga wakh ❤❤❤

  • @mbeurtine7041
    @mbeurtine7041 Рік тому +13

    Dieureudieuf sokh iow champion gua ta nittou deug gua ta très bien dit merçi

  • @BaYahou-db2gs
    @BaYahou-db2gs Рік тому +4

    Sohk c'est un homme qui aime pas l'injustice bravo

  • @diengibou5388
    @diengibou5388 Рік тому +3

    Merci ❤sokhe vérité Champion

  • @mouhamaddiagne6196
    @mouhamaddiagne6196 Рік тому +8

    Boye Niang dé wakh deuge dou sama mber mais nit deugla bou nité

  • @bambafall1423
    @bambafall1423 Рік тому +2

    Merci frère ❤❤🤲🏻🤲🏻

  • @papaboulydiedhiou504
    @papaboulydiedhiou504 Рік тому +7

    Sokh tu es véridique et digne

  • @saidoubah4729
    @saidoubah4729 Рік тому +6

    Champion deug rek ngaffi wakh ❤

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9ye Рік тому +3

    Bn2 champion la dhé, mais choc guénal gorgorlou yalla bahna

  • @cheikhvip4757
    @cheikhvip4757 Рік тому +2

    sa boko déguelo rk khamni limi wakh dara doko dindi nit bouy wakh degue wakh dji day lérr sétt ta day nékha degue dia dieuf way bro 🇸🇳🇺🇸👍🏽

  • @ibrahimaniane6508
    @ibrahimaniane6508 Рік тому +5

    Deug moom soko déguéee reek khamné lii deug leu✍

  • @papdiaw2476
    @papdiaw2476 Рік тому +2

    Mane diabarou DIOLA SAKHE LA BEUGUE LIGUI MOU FIN 😂😂 ..comme se que disait ma mère paix à son âme…les séréres son leurs rois avec un NOMMÉ YAKHOUBA BADJI qui de balinghor bravo pour leurs droiture machallah

  • @boubadiouf-c9v
    @boubadiouf-c9v Рік тому +7

    Yalla neu diam Sax pikine ❤️🙏

  • @BathiGueye-o1t
    @BathiGueye-o1t Рік тому

    Suportérou jacksonla m eumeu bakhoule vraiment sokh nittla

  • @cbcb6076
    @cbcb6076 Рік тому +9

    Yoroul djiko djigueine barriwoul wax Sénégal 🇸🇳 bayilen kouy wax deug ngueine diko sikk lolenne beug

  • @assanegaye513
    @assanegaye513 Рік тому +7

    Il communique bien

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 Рік тому +14

    Zarko Mom bayma Ndione sax moko eupou Victoire 😂😂😂Zarko palmarès 11 combat 4 victoire 6 défaites 😂sokho 18 combat 15 victoire 3 défaites Baparé Zarko né yay dafay xass sokhou 😂😂😂

    • @kefgg
      @kefgg Рік тому

      Sawaye Zarko 8 victoires la ame ak 4 defaites. Mo dane Boy Niague, Mansour, Thiate boy bambara, mame balla, bathie seras, Mbaye Gouye Gui, Baye Mandione, Ada Fass, mouye 8 victoires.
      Sa thies moka dane, ak Siteu (bobou Siteu def na 4 appuis) Gouye Gui ak Modou Anta, mouye 4 defaites.

    • @gueyelabsolu5889
      @gueyelabsolu5889 Рік тому

      @@kefgg Zarko mousoul Dann Boy NIANG mousou nio beraii sax Saway 😂😂😂Boy NIANG Amanéx moko Dann mè pas Zarko Saway Zarko Diii yambar 😂😂😂

    • @Dusay-js1yy
      @Dusay-js1yy Рік тому +2

      @@gueyelabsolu5889Boy Niague legnela wakh. Pas Boy Niang. Ça se voit que do setanekatou lamb

    • @kefgg
      @kefgg Рік тому

      @@gueyelabsolu5889 Boy Niague lala wakh pas boy niang. Si lamb Ama Balde Baye Peul lawone 2009.

    • @kefgg
      @kefgg Рік тому

      @@Dusay-js1yy Ki kay moy lolou

  • @malickseck9424
    @malickseck9424 Рік тому +6

    Yaw dé la geum ,Eumeu séne meussou ma guiss kouko geuneu Yess en plus mo dakka fén si adouna 😢

  • @DjibrilBa-xp7te
    @DjibrilBa-xp7te Рік тому +2

    Courage champion

  • @MoustaphaSow-te8zu
    @MoustaphaSow-te8zu Рік тому +2

    Diadieuf champion Machallah diameu thi yawe bou bakha bakhe Un homme digne goor yalla

  • @ibrahimabadiane8252
    @ibrahimabadiane8252 Рік тому +9

    Thieuy régime bouy danou yi yépp ay misal la ci bilahi

  • @seydiwane1497
    @seydiwane1497 Рік тому +5

    vérité absolue deugue dou rom mi nop ✌

  • @courasarr1582
    @courasarr1582 Рік тому +3

    Ama balde ❤boye niang ❤sokh ❤késsei✌✌

  • @abdoumbaye7294
    @abdoumbaye7294 Рік тому +1

    Eumeu gorewul😂😂😂😂

  • @ibrahimabadiane8252
    @ibrahimabadiane8252 Рік тому +2

    Merci sokh linga niamal zarko kontane na ci trop zarko domouram rék la mom dagnkoy sarakhé rék

  • @beugdeug5553
    @beugdeug5553 Рік тому +16

    Un jeune véridique sokh

  • @gorakane9600
    @gorakane9600 Рік тому +7

    Mé sokou vraiment mérité wo li khaléga boule topou nui bayil thiowli ga déme entrénedji boule topou défiant yi

  • @mouhamedniang3904
    @mouhamedniang3904 Рік тому +7

    Probleme bi moye Da ame gnouy diamou khaliss Sokh

  • @capitainetheo3543
    @capitainetheo3543 Рік тому +1

    Sock est un homme véridique.
    Yal na la Yálla aar.

  • @zalendiaye7659
    @zalendiaye7659 Рік тому

    Bilahi n'a fékheu bakhoul politique mon takh ngénn di doull eumeu 5 millions dako yeungeul sokhou Do tousse

  • @omarniang4346
    @omarniang4346 Рік тому

    Faralll foula.nekhe niome nioye kane fans balla laa mee damalaye begge

  • @modoufallbetebeteitsenegal5272

    Machallah sokou kadouyi RAFETNA amna solo lool Deugouna mais boy niang goor laa machallah

  • @MatarNdiaye-vo6md
    @MatarNdiaye-vo6md Рік тому +3

    Non sokh sama copin gua mes warowone wakh audio yi la boy niang envoyer 🤷🏿‍♀️

  • @bambalaye6152
    @bambalaye6152 Рік тому +23

    Vérité absolue frère deug dou rombou nopp

  • @coolestchannel8124
    @coolestchannel8124 Рік тому +1

    Khaliss khaliss khaliss thieuy YALLAH

  • @salioudia9358
    @salioudia9358 Рік тому

    Koula khol khamni nitkou degounge machallah