*Tyson 2 a plus de victoires que Eumeu Sene, Boy Niang, Ama Balde, Sokh. Le lutteur qui a le plus de victoire à Pikine. Beu parei yague feu lool. C’est dommage wa Pikine jappalei wougn ko*
Pourtant démé woule nonou mane mi tok na ak eumeu wakhe ko wakhou Tyson 2 bimouye dieule franc eumeu si mane lako yeugué wakhe dji kousi khamoule dara mandou si gnoune gni intéré lagnouye topé yalla dakhe yakar nagne si mome@@SamezimafillsBagabiwol-bl7xg
Wallahi champion nga kene dakoula beurré si lamb ji yéne rkk wa tyshinger akk boy niang layy suivre mais eumeu sene soufékéni linga wakhni nonoula démé defoul deug defoul yone mais ngir yalla wakhtanal ak mom stp mon champion
@@loeildutempstv1998lou miye jaloux linga wax foko tek ko ecrit ba kene dakhoukofa beure sathies thi bopam ki la warone dieul pas eumeu ki sakh mo raw sathies guene ko palmaress
Un grand champion et un de mes lutteurs préférés. Son seul probléme c'est que beaucoup de lébous ne luttent pas entre eux. Tyson2 vs Lac 2 guiers 2 Tyson2 vs Siteu Tyson2 vs Fils de Balla Tyson 2 vs Thiaat Tyson2 vs Diéne Kairé
Même problème que Zambala. Ils sont utilisés par les écuries de pikine pour faire des contacts avec leurs poulains. La relation n'est pas réciproque ils seront toujours considérés comme les étrangers de pikine voir l'éternel lieutenant
Tyson 2 vs obeuli doù combat bou djadou. Tyson rawnako loup bari. Beugueu beuré ba sacrifier sa carrière djaroukou. Wouteul un bon manager té nga nek si seul ligay. T'es un grand champion force à toi
Eumeu sene sene wowal Tyson nguén waxtane limou wakh deugue la man si lamb eumeu yaw rek lay topou mai d'après li Tyson 2 mom lou yénou manala wawal ndoye nguén waxtane c 1 vrai champion
Tyson 2 champion leu dh je me rappelle bimouy dieul tournoi RDV bi bimouy dane Nelson Mandela. Mais gayi nak daniou ko wara dieul si lamb ji la bokk kou am 18 victoires sur 21 combats beuré ak ay FRANC, ELTON niom sén gayi gueunou niouko bakh palmarès soulen banioul warou niouko bagn Tyson 2 vs (Lac Rose, Fils de Balla, Zarco, Jackson, Gora Sock, Mbaye Gouye Gui, Forza...) nassi promoteurs yi diap bokk Lamb mingui beug nakhsay ndakh tappalé ak moytou wanté.
Dommage. Il est victime du business de la lutte. les promoteurs préferent les lutteurs comédiens ou les lutteurs qui ont un public peu importe leurs performances. C'est dommage beaucoup de grands champions comme lui sont écartés
Tyson 2 ndanane la. Tay sou danone Elton wala Franc lambam wessouna fi. En plus lamb-j pour mou yatou ci mom, il faut que Lebou yi beuré sén biir. Tyson 2 vs Moussa Ndoye Tyson 2 vs Lac Rose Tayson 2 vs Jackson
Ki malgrés ses nombreuses victoires il n'a pas beaucoup évolué t pourtant ay champion la dane ( garga 2 , Gora sock thiatou yoff ,domou dangou necko rell fifty cent etc. Et juste 3 défaites: Elton franc gouyegui.
Walahi eumeu sene dou nittou dara mou geuna yees di lou yalla binde limouy wané nekoul si moum nitt kouma ragal la surtout bima deglou problème bimou amone ak sokh
C’est un grand champion 21 combat 18 victoires 3 défaites
Demal rock energi
Niou yatou lane😅
Tison 2 nioune wa pikine on t'aime bien ❤
Eumeu ngirr yalla woyal boy bi japaleko ngirr yalla na nice 😢😢😢😢😢😢😢
Démal nga dieul qa yonou bopou yala mo nékeu fépeu champion courage sava aller
C'est un vrai Lebou, un lebou a un bon état d'esprit courage 💪💪 champion 💪💪💪💪
Un très grand champion Aladji Ndoye ♥️💪🏾
*Tyson 2 a plus de victoires que Eumeu Sene, Boy Niang, Ama Balde, Sokh. Le lutteur qui a le plus de victoire à Pikine. Beu parei yague feu lool. C’est dommage wa Pikine jappalei wougn ko*
Vraiment dommage, il est le meilleur de tous ces lutteurs que vous avez cités.
Yalla bakh na inchallah Dina bakh inchallah ❤❤ Tyson
Ndaysan légui mbeur boufi amoul tiow sa carrière yakhou😢😢😢
Billahi frère
T lolou Dou yone ki champion la vraiment mom AK zarco combat la
💯% pikine jaroul bokk dañi lèkaneté Yow Tyson2 l’an 2000 nguane ibou sèngor sèn situation daff ma mètti bilahi
Lou wér ga wakh
Niaak Bayree ak PROMOTEUR REK UN GRAND CHAMPION ❤❤❤
Un vrai champion
Tayson 2 boul bayi PIKINE wax tanal ak eumue sene rek dax indi ga ko comba indi nala comba con nek lén si diamou rek❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Saway eumeu nitou intret leu
@@SamezimafillsBagabiwol-bl7xg sa way yaw más ga guiss nitt kou nekoul nitou intéré si adouna bi diou nek
Eumeu sene kay moye lolou
Pourtant démé woule nonou mane mi tok na ak eumeu wakhe ko wakhou Tyson 2 bimouye dieule franc eumeu si mane lako yeugué wakhe dji kousi khamoule dara mandou si gnoune gni intéré lagnouye topé yalla dakhe yakar nagne si mome@@SamezimafillsBagabiwol-bl7xg
Wallahi champion nga kene dakoula beurré si lamb ji yéne rkk wa tyshinger akk boy niang layy suivre mais eumeu sene soufékéni linga wakhni nonoula démé defoul deug defoul yone mais ngir yalla wakhtanal ak mom stp mon champion
Un vrai champion ndoye
Tyson 2 vraiment c’est un vrai champion, sou amone diapalé wésounafi
Thieuy Ndoye un vrai NDANANE billahi kouka fékk géej mouy contact nga ham ni mbeur deug leu 😢
Courage Mbeur dîna bakh inchallah
Ndeysann c triste il est tres dicipliné machala
Motakh lamb j nékhatoul. On ne voit plus les grands champi com toi les L'an 2000... mais courage amoul décourager
Vraiment Téy La messa Am Louma mètti si Eume séne 😢wakh ji Nakari nama trop Tyson 2 ne mérite pas ça
Eumeu Sene Sougn Mbeur Wayei Mongui Beugeu Sikk dh. Problème ( Valdo, Jordan, Nguer Bou Jap, Coly Faye 1,)
Khaliss dale😢😢
Tyson
C'est pas bien franchement
@@loeildutempstv1998lou miye jaloux linga wax foko tek ko ecrit ba kene dakhoukofa beure sathies thi bopam ki la warone dieul pas eumeu ki sakh mo raw sathies guene ko palmaress
Ndeysane un très grand champion bilayy iieo
Vraiment lamb yakhou na. Champion yi meunou gno ame combat
Un grand champion et un de mes lutteurs préférés.
Son seul probléme c'est que beaucoup de lébous ne luttent pas entre eux.
Tyson2 vs Lac 2 guiers 2
Tyson2 vs Siteu
Tyson2 vs Fils de Balla
Tyson 2 vs Thiaat
Tyson2 vs Diéne Kairé
Ndoye loutah lébou yi ame yarr ndeysane qui dou wah tiahane😢
Cëëy aduna eumeu goula toudé dom soulay woo deko dieull way fall
Eume d'où Goree c'est triste
Tyson 2 champion nga ❤
Machallh bilahi dama kou beugue loul
Merci champion ndanane nga bou mak sakh non pour moi sa la pas bon 😢😢😢😢😢😢😢
Champion la deh lamb mo treudi rk
Tyson un grand champion
Un champion hors pair Aladji Ndoye dît Tyson 2 Yagg nalein Wakh 100/💯 Amoul ci Sport . Lobbying Kassei
Ce grande Champions nga pir Diambar deuge nga diamou rek ak ame
Tyson 2 un vrai champion tu est un lebou ne t reclame pas un pikini wa
❤borom pokare yi ❤
Eumeu sene na wakhtane ak tayson 2 wy
Notre champion ❤❤❤
Prometteur Nion yakhe lambe
Vèrite absolu ❤❤❤
Iba kane tu ne fais que repeter les memes questions !!
Boo ladioneu Mohamed ndao Tyson dinala wakh kouye eumeu séne
Écris Ngayane c'est possible aller faire
Même problème que Zambala. Ils sont utilisés par les écuries de pikine pour faire des contacts avec leurs poulains. La relation n'est pas réciproque ils seront toujours considérés comme les étrangers de pikine voir l'éternel lieutenant
Tyson 2 _ l'an 2000- ibou senghor _zambala ( pikine moléne tardél( séne tête files yii gnoo gueneuh deugue séne nday surtout boy Niang
Tyson 2 vs obeuli doù combat bou djadou. Tyson rawnako loup bari. Beugueu beuré ba sacrifier sa carrière djaroukou. Wouteul un bon manager té nga nek si seul ligay. T'es un grand champion force à toi
Mane question bi moy pourquoi Obeuli té mou moudié dane thiatou yoff nak
J'ai bien aimé votre sortie Tyson 2. Tu as beaucoup servi à Eumeu Sène mais il ne t'a rendu la pièce de la monnaie. Vous êtes notre fierté
Lamb lobies moko yaak mais yaw rek ya wara am combat le grand champion ✅
Ki dou fén il dit seulment la vérité, les grands lutteurs sont méchant désolée😡😡😡
Ce gars-là a vraiment besoin d'aide, il mérite du respect ... Sinon ça carrière sera fichue ... Sinon change d'écurie c'est tout
C'est catastrophique nitt toudè la dôme soula wowè doko dieul
Bilaye dane ko setane eume dou gate
Ndeyssane amoule djapallé mais daffa meuna beuré
😢😢😢
Un gars que j'estime beaucoup
Eumeu sene sene wowal Tyson nguén waxtane limou wakh deugue la man si lamb eumeu yaw rek lay topou mai d'après li Tyson 2 mom lou yénou manala wawal ndoye nguén waxtane c 1 vrai champion
Champion la dé bilaye mais courage rék champion
💯 pikine amoutt gnom gneup ken wolouwoutt sa morom
Tyson 2 champion leu dh je me rappelle bimouy dieul tournoi RDV bi bimouy dane Nelson Mandela. Mais gayi nak daniou ko wara dieul si lamb ji la bokk kou am 18 victoires sur 21 combats beuré ak ay FRANC, ELTON niom sén gayi gueunou niouko bakh palmarès soulen banioul warou niouko bagn Tyson 2 vs (Lac Rose, Fils de Balla, Zarco, Jackson, Gora Sock, Mbaye Gouye Gui, Forza...) nassi promoteurs yi diap bokk Lamb mingui beug nakhsay ndakh tappalé ak moytou wanté.
❤❤❤❤❤❤❤😊
😂nelson Mandela mo nakhon gayi ba de final mou bette gnou barri 😂 ohh lamb
@@moussaba5415bilay bane écurie la nekati wone sakh
Tayson 2 champion la billahi
Tayson 2 démal njibii ndayane NGA yoor sa ecri
tyson 2 moussa ndoye tyson 2 Diéne Kairé tyson 2 Jackson combat you nékh la
Demal ndayann créer écurie
Demalal sa bop
Grand champion
Eumeu sene lolou niaw trop koula beugeu rk mon lay touddée doom
Vraiment gayi warnagnou khalate lamdji champion you bari beurewougnou dou yoneuh diam Terry Tyson 2 etc
Champion la vraiment lamb mo beuri mafia 😢
Bilay walay mbuer d'où gér
❤❤❤❤❤❤❤
Dommage. Il est victime du business de la lutte. les promoteurs préferent les lutteurs comédiens ou les lutteurs qui ont un public peu importe leurs performances. C'est dommage beaucoup de grands champions comme lui sont écartés
C'est la triste réalité 😢
Billhi champion deugla 21combat 18victoire 3defaite
Eumeu sene bimou bayéi tyson láko bayiwoon man
Obaly bu ko jël xoolal la neen yaa ko raw ci làmbu. Te daa nekk ci yoon 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Bayi leen lamb
Tayson 2 khamoul ay thiakhane
No tayson mome dousama mbeur wayé défoula dara kila eundéne boul falé didéme yobaléla loy wakh wakh koko
En tout cas kou nieppou toufli nga tooy eumeu sene na khôlaat bopam
Li moy wané né mbeur dou mbok
Tayson 2/ Diam térry nékhna komk niom niar niép danléne Di daw nanléne bolé niom niar
Wwe yaw vrai amateurs nga
Ki Pikine là deuk boulen ko wax lo 💚❤️
Daguéna guawa toudou nitt dôme nak 😢😢
N'a nieuw rufisque kaye fi waye si amanekh
@@momobouthiapathiolybi7752 mangui jiégalou dé🙏
Tyson 2 ndanane la. Tay sou danone Elton wala Franc lambam wessouna fi. En plus lamb-j pour mou yatou ci mom, il faut que Lebou yi beuré sén biir.
Tyson 2 vs Moussa Ndoye
Tyson 2 vs Lac Rose
Tayson 2 vs Jackson
Yaw bayil lébou yi
Tyson 2 Vs Lac Rose combat bou diadou leu
Tyson 2 ame na combat
@@MomoSeck-zd4bt mome ak kane?
@@Lepatriote9423 nn pour mane mok obeuli ba légui ni néké da yakhou
Ki malgrés ses nombreuses victoires il n'a pas beaucoup évolué t pourtant ay champion la dane ( garga 2 , Gora sock thiatou yoff ,domou dangou necko rell fifty cent etc. Et juste 3 défaites: Elton franc gouyegui.
Eumeu séne ligne kaye wakhal yii beurina trop
Nieuweul parcelle diambar bilahi même pas 1ans gua lal plus de 70million et plus
Laal 70millons du caaxaan de 😂😂😂😂
Walahi eumeu sene dou nittou dara mou geuna yees di lou yalla binde limouy wané nekoul si moum nitt kouma ragal la surtout bima deglou problème bimou amone ak sokh
Changel menager champions
Vraiment dafa bokou si lambeu dama ko yeureum sakh 😭😭
Borom pokar yi❤
Mbeur vraiment war nguen kholat sen bopp ....manque de reconnaissance rekk
😭😭😭😭😭💪💪💪💪💪🥰🥰🥰
Lou takh mou dello avance ibou Ndiaye oublié
Taille yi bokul
Loutakh nga beug ko def diaroukaye Obeuli na beuré ak gnome Serigne Ndiaye 2
Tapete rek
Ndananu lamb mogui niii
Mom dafa beugueu eumeu séne
So mei écurie Dina nieuw inchallah jamm rk ngay l
Koussi bayiwoul régler sa problème si plateau
Ms pourtant eumeu séne yagg n'a gneuw sa combats soutenir la noumou absenté sa bénn combat rek ngay wakhé nii
Tayson 2
Bilay eumeu séne dou tous
encore eumeu séne,toujours eumeu séne kou gneupe toufe li nga toye
Il a problème avec tout le monde. Il est égoïste, ne penses qu'à lui seul.