Merci ngagne la lutte a toujours été ainsi les lutteurs montent dans la catégorie suivante le moment venu ce règlement est vide pas d'argument convaincant ce règlement ne profite pas au acteur principal de la lutte maintenant ils sont entrain de politiser la lutte lamb expérience leu pas de poids diack's khaliss moko dougal si lamb lamb avant tout d'abord c'est culturel diack's na aucune leçon a nous donner Malick est sur la mauvaise voi comment un jeune lutteurs de 97 kilos par exemple pourra prouver son talent face un un géant de 130 a 140 kilo
D'abord lamb dou poid c'est de l'expérience comme dans tout les autres sports maintenant vous ne voulez pas qu'un 110 kilo competit avec un 80 ou 95 kilo mais il vous paraît juste qu'un 140 kilo voir plus competit avec un jeûne de 97 kilos ce règlement na aucune fondement ni d'argument convaincant ❌❌❌💖💖
Djiacs maylenn ak Malick lois bi filako fekk . Pourtant Ada Fass... dagnelenn Adione mou fekkoffi t daflenn wathié. Lamb bi momolen ko li amateurs yi ak mbeur yi beug deflenn c mieux.
Gagne limou wakhe ci lambou gambie bi lou werrela çama kName la dafa bindou poie legue gnou gueneco demi finale ciloulene nekhe mane cila ko wakhe ne bindoule lour mou djeuleko
Pour mann niakk fayda akk tapéte akk niakk gueum sa bopou wéssouwoul plus de 100kg di wakh nann poids léger layy continué di beuré iow nianoulo yalla monté si carrier poids léger kounék Kham nani 75 entre 95kg lh niakk fayda plus de 100 kg takhaw di wakh léger layy mbeuré
❤❤❤❤ ngagne séné rek
Merci ngagne on est de tout coeur avec toi💯💯🦾🦾🦾❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Si SNG insiste sur la balance la majorité des jeunes lutteurs risque de prendre les pirogues et mourir dans les océans.
merci jambar ❤
Merci ngane sène vérité absolue
Merci beaucoup ngagne sene
Merci ngagne la lutte a toujours été ainsi les lutteurs montent dans la catégorie suivante le moment venu ce règlement est vide pas d'argument convaincant ce règlement ne profite pas au acteur principal de la lutte maintenant ils sont entrain de politiser la lutte lamb expérience leu pas de poids diack's khaliss moko dougal si lamb
lamb avant tout d'abord c'est culturel diack's na aucune leçon a nous donner Malick est sur la mauvaise voi comment un jeune lutteurs de 97 kilos par exemple pourra prouver son talent face un un géant de 130 a 140 kilo
Ndaaa ndaa rec
Merci ngane
Diokh len numéro malik ngom
Lamb mo Nara dehh, raflet mbeur
Dianks bayil doul mo guen😢😢😢
Ngagne séne ndaandaane la
Diaquse yag Malik sene data deye 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Il faut appliquer le règlement
Les lutteurs comprennent bien c d koi il s'agit
D'abord lamb dou poid c'est de l'expérience comme dans tout les autres sports maintenant vous ne voulez pas qu'un 110 kilo competit avec un 80 ou 95 kilo mais il vous paraît juste qu'un 140 kilo voir plus competit avec un jeûne de 97 kilos ce règlement na aucune fondement ni d'argument convaincant ❌❌❌💖💖
Malick moun na demision né
CFA a dit la vérité
Nda ngagne duambar lh
On est contre avec la balance.
Bien dit Jacks
Jacks xamul dara si lamb xalissam rek lay toppu si lamb nek léne ay nitt 🧏♂️
Diaks touti nga thi yakh lamb sérère. Lamb avant ngakoy kham pour wout thi khaliss sérère moko moom té culture la. Meunoo dougou thi culture diambour beugko déformé ndakh sa intérêt kessé. Tu nous amerdes et Malick dafa beuga gueun kheet
@@elhadjindiaye720ins bi lutte simple sérère momouko boulnah sa bop
Ma woko parce que faire gui da wara ler
CFA respectel sa bope niewnga Dakar niata yone t'ai fofou pesage lawone bayiléne thiane lamb boudoul poid loutakh mbeur yii Di antrainé
Je propose l'âge
Malick a trahi la mafia 😭
Jacks a raison
Non à la balance ❌❌❌
Yene mbeur you mague yii yena meuna diapalé boy yii
Ces genres de Jacks qui poussent à Malick Ngom à faire ça.
Saway gni wara beuré poid léger khame nagne légne nagne yégue poid lourd mo guéne faut maintenir la loi balance force
Ngagne yaw wahkaou deug nga non à la blance
Khamo lambe ioe
Ok
Gni wakhou mbam rek lagnoufi wakh les 95k ak 130 kilo est ce que c normal té lolou guenn bagne poids leger la méme chose se repete au poids lourd
Diak’s khamo lambe xaliss mola thie indi bougniou sonal
Balance amoul thie lutte simple kou gniémé beurè fouko nekh
Diak’s yagoul tegue ay lambe so tegué lambe am so tegoul mou am
Sama bokkou sérère yii ak séni wolof you dégueur 😂😂 mais nous disons non a la balance 🛑
😂😂😂😂yangui roubé déh,sérère ak lak olof rék 😂😂😂😂
Donc moin de 100 kg waroul borré poid lourd
Djiacs maylenn ak Malick lois bi filako fekk . Pourtant Ada Fass... dagnelenn Adione mou fekkoffi t daflenn wathié.
Lamb bi momolen ko li amateurs yi ak mbeur yi beug deflenn c mieux.
Gagne limou wakhe ci lambou gambie bi lou werrela çama kName la dafa bindou poie legue gnou gueneco demi finale ciloulene nekhe mane cila ko wakhe ne bindoule lour mou djeuleko
Mbeur dou soblet bagn koy pesé yen niou djité lamb lay wakhal malik ngom tegal Lou ler
Cf yowe mome poids lourds gua
Yow demal falé. Lamb mo mag sa baye. Yow ngay wout khaliss té beugo kenneen am
Yaw cf yaw mi poids-lourd nga da nga ragl don ngou
Bal
Non à la balance
Pour mann niakk fayda akk tapéte akk niakk gueum sa bopou wéssouwoul plus de 100kg di wakh nann poids léger layy continué di beuré iow nianoulo yalla monté si carrier poids léger kounék Kham nani 75 entre 95kg lh niakk fayda plus de 100 kg takhaw di wakh léger layy mbeuré
Par ce yaguo setane lambe motakh khamo réalité lambe
Yow mbeurou tawgadou sakh déy eup 100 kilos . Khamo lén touss boudé Malick da diél wolof yi tég lén si wétam. Doufi yag gni khamougn touss si lamb. Lou takh frappe amoul balance ? Merde wayyyyyyy
@@ousmanendour8641lamb dou afair olof,sérère épuis boul yakarné lutte simple bi instan bi nanga hamné sérère momouko ok
@@moussapayemane4167 d accord na AK yow mais côté organisation lay wakhé . Sérère noumouy organisez mbapat mom késsé la . Balance bokoul si lamb
Malick dou dara