Reug Reug minimise Modou Lô : "mane champion du monde laa, mom késsé doufi mbeur..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 23 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 329

  • @TopGueye-nv7pc
    @TopGueye-nv7pc 15 днів тому +43

    Sénégal roi mofi am

  • @OmarBao-gu5qp
    @OmarBao-gu5qp 15 днів тому +57

    Lolou tegal ko niom ganou fi lambou jui modou Lo moy sen papa ❤

    • @ElhadjiFall-nw2he
      @ElhadjiFall-nw2he 14 днів тому +2

      No reug vrement sokhor ngua li ngua wax defar😂

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 14 днів тому

      Vraiment 😊

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 14 днів тому

      Danoul Balla, Lac, Bomb, Siteu, nul ak Gris, Gnemewoul Tapha Tine kone ROI wou kane la ??

    • @fallouvamos
      @fallouvamos 12 днів тому +1

      ​@@papadiom9260 bo dané Roi do nék Roi ? Arrêter léne séne yiiii mane modou c'est pas mon lutteur mais yalla kofi tékk koumou nékhoul ak say analyse sa problème la ennnnh Sénégal Mom Koufi nieuw di lathié qui est le roi des arènes niounileu Modou lô lolou loléne si meune ? Dane léne ko dieul Roi bi ay wakh danoul Modou lô dehhhhh 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

    • @alassanedieng259
      @alassanedieng259 12 днів тому

      Mane fralouma si kéne mai reug mo mane 10 Modou lo

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 15 днів тому +12

    Modou Lo yalla nala yalla lafal thiate gneipou ioe lagn tek beutt

  • @SambaSene-j1h
    @SambaSene-j1h 15 днів тому +37

    Reug si lambe modou moye saine baye se le roi

  • @modoulo4004
    @modoulo4004 15 днів тому +13

    Reug reug saxol be mou bonne ❤

  • @CissIsmaila-r9r
    @CissIsmaila-r9r 15 днів тому +18

    bilahi modou lo moy ndanan mom rèk mofi nèk roi thiow bi beuri gnithi beugeu diote diko minimisè😅

  • @kanejr7260
    @kanejr7260 15 днів тому +10

    Reug Reug est ingrat

  • @ngommamegor7924
    @ngommamegor7924 15 днів тому +48

    Bilay ki gauna sonou moy kii kontor modou modou moy sen papa 😂😂

    • @mariamaba6644
      @mariamaba6644 15 днів тому +2

      Bilahi

    • @modousarr8848
      @modousarr8848 15 днів тому +1

      Bilay

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 14 днів тому +2

      Dafa lérr😂

    • @kaninekahn6273
      @kaninekahn6273 14 днів тому +1

      Y’en deh modou Lo soulene topé dou beuré 🤣🤣🤣

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 14 днів тому +1

      Saway Djoutou lo khana sa bayy la yaaw?? Danoul Balla, Lac, Bomb, Siteu, gnemewoul Tapha tine ngene beug gnou ndaye sonal !??

  • @EssaBangura
    @EssaBangura 15 днів тому +10

    Modou lo Rek ❤❤❤

  • @yazalazadiallo
    @yazalazadiallo 14 днів тому +6

    Le combat que tout le monde attend c’est Modou Lo vs sa thies un point c’est tout

    • @fallouvamos
      @fallouvamos 12 днів тому

      Défaite Sathies contre Eumeu séne mo yakal sathies

  • @libasselahi
    @libasselahi 15 днів тому +11

    Reug reug mii weroul dh😁😁😁😁

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 14 днів тому +2

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @falloukonta1674
    @falloukonta1674 15 днів тому +19

    Ms reug reug mii eske wérna vraiment 😢

  • @mamadoudione8917
    @mamadoudione8917 15 днів тому +21

    Reug Reug naak depuis l'ore nite yi niougui rafetaal D. One Championship n'est même pas reconnu pour sa ligue MMA, champion du monde ONE CHAMPIONSHIP en MMA dou daara, redescend sur terre.
    ONE CHAMPIONSHIP est une ligue de Kick Boxing, ay Pa you dièkhaal niofay combattre en MMA

    • @ibrahimahanne6906
      @ibrahimahanne6906 15 днів тому +1

      Saay yangui dioum dh ufc moy le plus grand organisation mma one championship nga beugone wax fofou la reug nek pas ufc

    • @mamadoudione8917
      @mamadoudione8917 15 днів тому +5

      @ibrahimahanne6906 one championship oui j'avais même pas relu pour voir mon erreur. One Championship car Reug Reug est là-bas. One Championship est plus connu pour sa league de kick boxing. Reug Reug neeu yaarou, les sénégalais niougui raafeetaal tei nopi, Champion one Championship bou dèmer ufc il n'intégra même pas le top 15 de sa division.

  • @moussabayo8554
    @moussabayo8554 15 днів тому +17

    One championship nga nék champion té fofou équivalent 2e division leuh. Lamb dji Modou Lô moy sén Baye

    • @idrissafall7940
      @idrissafall7940 14 днів тому +3

      Dou sakh deuxieme division
      1 er division ufc
      2 eme division pnf
      3eme division championship
      Paré dignou ray ak wakh

    • @bdiene66
      @bdiene66 14 днів тому

      @@idrissafall7940 sén keur da fa ame kou fa nék 3e division mma?

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 15 днів тому +16

    Reug reug iaw ak tapha tine combat la kousi daan dieul sén papa modou lo le roi👑 😂😂😂

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 14 днів тому

      Loutax gnouy beurer Sen birr te Modou wara djeul Tapha diko saw !Bomouy djeul ROI hi djouguer thi defaite la djouguer Balla djoutal ko Eumeu maay ko chance. Boumou gnou fonto Modou lo momoul ndaye niit gnii

  • @Chiekh.mouhaiminou.wouldou.
    @Chiekh.mouhaiminou.wouldou. 15 днів тому +10

    Champion du monde yombouna troop si sénégalais yi

  • @kurayahmi
    @kurayahmi 15 днів тому +41

    *Le fait detre champion de One Championship, qui est comme la 2e division en MMA comparé à l’UFC, n’a absolument rien à voir avec la lutte avec frappe. Sa Thies nekoul champion du monde teh daan nala. Boy Niang bi daan Sa Thies Modou Lo dafko daan avec facilité. Modou mola meune aller-retour*

    • @modourokhaya9616
      @modourokhaya9616 15 днів тому +4

      Fotekna Modou moko meune aller-retour? Danio beuri mou daneko?

    • @Momaradia111
      @Momaradia111 15 днів тому +5

      Bayilene sokhor one championship nékoul 2e division comme championnat Angleterre Espagne …

    • @modourokhaya9616
      @modourokhaya9616 15 днів тому

      @@Momaradia111 tontouwo sama question deh. Damamné fo tekne moko meune? Sokhor yaw mikoy khalat yaako deff

    • @Momaradia111
      @Momaradia111 15 днів тому +2

      @@kurayahmi rero wouniou dé gniy minimiser titrou Reug Reug témou wara nek fierté sénégalaise la diap ni sokhor la

    • @Momaradia111
      @Momaradia111 15 днів тому +1

      Pour mane Reug kene meunouko si lamb dji

  • @DjibySy-h3f
    @DjibySy-h3f 15 днів тому +14

    Reug Reug Bayil nagou bi
    Daga fokné khamougnou
    Modou Lo dou sama Mbeur Mais doussa Morom cii lamdj
    Encore une fois Bayil Nangou bi

  • @MaguetteSall-v9m
    @MaguetteSall-v9m 15 днів тому +9

    Balla gaye moy sama mbeur wayé reug reug mi dafa sokhor Modou moy roi 👑 nga nangou wala nga bagne

    • @LeprinceVegeta-f6i
      @LeprinceVegeta-f6i 14 днів тому

      pourtant wahoufi béneu wahou sokhor dh soudé lolouleu xanaa mbeur yeuppaa sokhor, wala yaw titre bi rek nga lire geum doulkat yii di yokk?? gnom franc ,balla, zarco ,ada fass etc. dh chaque fois gnou minimisé séne adversaire té doléne wah dara, lii génoul si lamb, il a aussi bien que modou lo mofii roi, ndanane etc..

  • @MouhamethSy-g8g
    @MouhamethSy-g8g 15 днів тому +21

    Modou lo doussa morom

  • @MouhamadouNdiaye-d4m
    @MouhamadouNdiaye-d4m 15 днів тому +5

    reug vraie dof leu

  • @abdoulayediouf8678
    @abdoulayediouf8678 14 днів тому +2

    Boy reug reug nékal champion du yawmal khiyam ba kham FI thiotou ndayam modou lo mofiy sen bay par force mou nèkh lèèn ak mou nakhari lèèn
    Sen kholyi gno bon 😢😢😢😢😢😢

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 15 днів тому +2

    Reug Reug actuellement ny
    Moo geuneu chér Modou lo foufff
    Modou lo champion Sénégal 🇸🇳 la mè Reug my champion du Monde 🌍 la Reug wallahi Moo Meun fouff Modou Lo🥹Reug champion ladé pur sax

  • @malickseck950
    @malickseck950 15 днів тому +2

    Modou❤moy sa mbeur dé mais dieul reug reug c'est le moment où jamais

  • @MameCheikh.
    @MameCheikh. 15 днів тому +4

    Legui reug dieuleul Tapha tine😂🎉

  • @disytbi8711
    @disytbi8711 15 днів тому +16

    Reug reug bane vip la dane apart Bombardier bou am 50ans ?😂😂😂😂

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 15 днів тому +2

      Gouygui vip leu

    • @SaliouGueye-i8h
      @SaliouGueye-i8h 15 днів тому +3

      Bombardier mo dane balla ak modou😂😂😂😂😂

    • @senegaleventschanel6913
      @senegaleventschanel6913 15 днів тому

      @@Mbodji-walogouygui kegne la nek vip? Tapha Tine rekk lafa beurel te claf mo takhone

    • @ibrahimaba3553
      @ibrahimaba3553 15 днів тому

      Gnimou dane gneup yow sa mbeur daléne di moytou gni gueuna naxari dane si lamb ji la Reug Reug dane un champion doit être protéger Siteu bimouy gneuw di nokha Modou lolou koum fi dane pour meuna def lolou Modou Lo xamoléne sports moy lane 😂😂😂

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 15 днів тому +2

      @@ibrahimaba3553 wakhnga deug Modou Lô day moytoul rk😂😂😂

  • @NdiayeIssa-fo1tr
    @NdiayeIssa-fo1tr 15 днів тому +6

    Reug reug yaw modestal touti

  • @mohamadoumoukhtarcisse9043
    @mohamadoumoukhtarcisse9043 15 днів тому +3

    Une fois Roi, reug reug va glorifier de ce titre 😢😢?
    Faut valoriser tes adversaires pour avoir du mérite.

  • @xelcomdecorationsopeserignesal
    @xelcomdecorationsopeserignesal 15 днів тому +65

    Champion du monde amoull si lamb

    • @moussapayemane4167
      @moussapayemane4167 15 днів тому +8

      Pourtan lamb dji amoul roi ndah CNG niowahné validé wouniou roi bi 😂

    • @xelcomdecorationsopeserignesal
      @xelcomdecorationsopeserignesal 15 днів тому +10

      @moussapayemane4167 yaw nanall galass 🤣

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 15 днів тому

      ​@@moussapayemane4167 Amna roi kay Siteu leu Yalmine bi👑💪🏾

    • @PendaTalla-c5z
      @PendaTalla-c5z 15 днів тому +6

      ​@@moussapayemane4167Nékouniou MMA

    • @SaliouGueye-i8h
      @SaliouGueye-i8h 15 днів тому +2

      Rueg rueg ndanane la bayil sissou😂😂😂

  • @jobehamidou6545
    @jobehamidou6545 15 днів тому +7

    Merci beaucoup reug reug champion de mond

  • @ThioroFall-s8h
    @ThioroFall-s8h 15 днів тому +7

    Modou lo kén menouko calculer ba sén beuss taxaw gay comprendre reug reug ni modou lo dou nioniou gua danne
    Franc mi dokh sen digenterk dégenté Thiow li yalna franc bayi modou lo mou dieul leu gua xam ni do dra reug reug si kanam modou lo

  • @abdoulayesow4208
    @abdoulayesow4208 15 днів тому +5

    Reug reug vs tapha tine combat la

  • @djimbaniang2190
    @djimbaniang2190 15 днів тому +2

    Maramdji da xam lamb nak reug reug ❤

  • @CASI7797
    @CASI7797 15 днів тому +2

    Coalition anti modou lo mofi dadjeii dh on dirait😂😂😂

  • @Bamba-rk
    @Bamba-rk 15 днів тому +16

    Reug Reug nak prouver goo sa entrée sa grand yi dh
    sa palmarés ci làmb nekkoul lou extra-ordinaire dji
    tu reste un grand champion nak. mbeur meunoula ci làmb nak mom mais beuré goo fi combat risk

    • @kefgg
      @kefgg 15 днів тому +1

      Combat contre Gris 2 douwone combat risque ? Boul faténi diamono yoyou Gris 2 dafa nekone si dynamique de victoire pendant 7 ans meusoule won danou gneup ragal ko ame dolé nek super lourd nek jeune comme Reug Reug. Lolou combat risque lawone si Reug Reug.
      Sa Thies tamit combat risque lawone mais reug dafa danou. Combat Boy Niang bi di gneuwe tamit combat risque leu si Reug

    • @Bamba-rk
      @Bamba-rk 14 днів тому

      Wa c vrai mais combat ak boy Niang moko meunoon dougeul définitivement nak ci grand yi.
      Combat Gris 2 dou woon risk ci Reug Reug à mon avis. Par contre risk la woon Gris 2 vu k mom mooci am lumuy pedre

    • @bdiene66
      @bdiene66 12 днів тому

      Ki kèn da ko nième ci lamb baye beurè akh mom .Khana guisso boye niang même Sa thies bi mouy beurè akh mom Balla gaye da fa tèw😂😂😂

  • @OuzinDiouf-g4e
    @OuzinDiouf-g4e 15 днів тому +8

    Yow mom doo gawa beuré Al modlo 👑

    • @Auxservices-w4n
      @Auxservices-w4n 14 днів тому +1

      Lolou probleme Modou Lo pourtant Franc wakh na Eumeu sene louco gueuneu grave

    • @SENETIKTOK
      @SENETIKTOK 14 днів тому

      Modou mooo khaaam d yagu yagu daaay djeul roi des annees

  • @cheikhmbacke2841
    @cheikhmbacke2841 15 днів тому +4

    Reug reug champion du catégorique bou ndaw bi ga négue

  • @moussaomardiaham4727
    @moussaomardiaham4727 15 днів тому +1

    Merci reug reug très belle analyse

  • @moussadiakhate4063
    @moussadiakhate4063 15 днів тому +1

    Kon la nk mais reug moy lamb il est pertinent dans la lutte

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 15 днів тому +5

    Reug reug mbeur dou complet yagui ni daga ragal khéxx😂😂😂

    • @sarabo6779
      @sarabo6779 13 днів тому

      Kou ragal khékh dîna nek champion du monde mma

    • @bdiene66
      @bdiene66 12 днів тому

      Khamo khèkh pour kou teulè beurè la😂😂😂.Khamo lamb dè mon ami .Domou lèbou ngaye wakh wakhou khèkh😂😂 ki khèkhoul day beurè.
      Son slogan est "diap dane gnibi"😂😂

  • @morgaye9582
    @morgaye9582 15 днів тому +11

    Reug reug desfois daguay waxe rk ma décourager Mod lo tolal noula neikh dafay coupé distance bi kheikh ak iao touché leu je donne le cas de B52 Mod lo dafa doug si garde bi gagneko si beute té tapha tine soutoul B52 et si mes souvenirs sont bonne yaw biguay débuté si mma dem diangui kheix toubape dagnounila sen arènes bi yeup Mod lo kassé mossi kheip yakofi waxon hm

  • @sambadiouf9121
    @sambadiouf9121 15 днів тому +2

    Champion reug reug késsé 💓

  • @SeydinaNdiaye-gs1ox
    @SeydinaNdiaye-gs1ox 15 днів тому +2

    Reug reug wakh meunoussi dara’’wornayalah reug iow boul wakh del beuré rek😂😂😂..nonou lagne la beugé..continuel ninga dane wakher manam damay nhieuw daane nhieupeu dem😂

  • @SaliouGueye-i8h
    @SaliouGueye-i8h 15 днів тому +2

    Rueg rueg ndanane la ❤❤❤

  • @bayecheikhsarr6079
    @bayecheikhsarr6079 14 днів тому +1

    Vraiment reug reug da fa wara ndiagui commication

  • @yaramfall6996
    @yaramfall6996 15 днів тому +6

    Reug nekhoul ba nekhoul mais dofff deugu la
    Ils m'énerve communication zéro Putin diangual wakh gnou beuri gnogui lay méré ndakh niguay wakhé

    • @LeprinceVegeta-f6i
      @LeprinceVegeta-f6i 14 днів тому

      mo geuneu wérr séne wakeur ,yéne kéy yénaméy enervé nafekh yii, Sport lagnou wah pas parole, communication bi pour nékhal lamb bi leu rek mais amoul sens (dou moy indi victoire ak dane) ,toujours mbeur wah dara douko déf jourou combat bi ,toujours kéy
      c vrai qu'il n'est pas top en communication mais.. kii sou moumeuwone sah dangéneko warone respecté (yalla dou méyé yeupp) ,toubab yii amneu ay sportif you am handicap moumeu wala teuh (sourd) ou les 2 mais au contraire dagnkoy diappé comme gneupp
      bayiléne kii way.. kii c notre fiérté ,représenténagnou founékk ,indi ay médaille/ceinture, féyoulgnou sougnou maame yii (colonisation bi) ,soléneko valoriséwoul mom nékkoléne fier sénégalais, reug moy lamb moy sport🖤

    • @SENETIKTOK
      @SENETIKTOK 14 днів тому

      Moooo taaayyyy

  • @ibrahimaba3553
    @ibrahimaba3553 15 днів тому +2

    😂😂😂Sénégal mo nékh deh wa Siteu kone foum diaar est ce que mo gueune palmarès Reug Reug gnii Reug Reug dane Siteu dafléne dane est ce que talent dagne ko wara protéger mais lamb ji mo barii lobby koi😂😂😂

  • @modousarr8848
    @modousarr8848 15 днів тому +3

    Boy yaroul Modou Moy roi

  • @Baaliou-t9l
    @Baaliou-t9l 15 днів тому +4

    Reug reug doof la moom dey wakh ba yeuy bopam😂😂

  • @DethieDioufFissel
    @DethieDioufFissel 14 днів тому

    Champion du monde est mieux que Roi des arène 1000fois.REUG REUG à raison ❤❤.

  • @SouleymanevSy
    @SouleymanevSy 15 днів тому +3

    Ki mom da doff 😂lamb nga bole ak mma😂

  • @ibrakane5932
    @ibrakane5932 15 днів тому +5

    Reug championchip nga gagné nékagoo au sommet

    • @sarabo6779
      @sarabo6779 13 днів тому

      Mais il est devenu une star connue mondialement avec des vidéos qui font 20 millions de vue lamb fi la yeem

  • @papemalicksow994
    @papemalicksow994 15 днів тому +1

    Merci reug

  • @AbdoukhadreLô-t8v
    @AbdoukhadreLô-t8v 14 днів тому +1

    reug reug legui bari nga wax noooo

  • @saliougueye9833
    @saliougueye9833 15 днів тому +2

    Reug mi eskeu cv

  • @Ibrahimandiaye2221
    @Ibrahimandiaye2221 15 днів тому +2

    Reug reug vs tapha tine

  • @OusmaneKanee
    @OusmaneKanee 15 днів тому +2

    Communication dra ba legui dra dra blh

  • @malickseck950
    @malickseck950 15 днів тому

    À mon avis pour man Modou ❤balla gaye amoul enjeu si nioune supporterou Xlo❤vraiment

  • @elhadjigorasall5512
    @elhadjigorasall5512 15 днів тому +4

    Reug Reug soof na nak té khamoul 😂

  • @DoudodiengDoudo
    @DoudodiengDoudo 15 днів тому +5

    Beugone na commentaire mais sama xol mo mako mayoul nakh émission bii journaliste amougnou Fouleu ay doof rk gueine invité

  • @lamzogaming4
    @lamzogaming4 12 днів тому +1

    Waa modou Lo pourquoi dieulul reug reug

  • @BadaraMbaye-s2y
    @BadaraMbaye-s2y 15 днів тому +3

    Arrêtez de tendre les micros a Reug Reug il est fou à lier doublé de quelqu'un qui n"a rien compris.

  • @assanecissfouloume8235
    @assanecissfouloume8235 15 днів тому +4

    Ki dou Champion du monde ki champion sur la Moy 3sem division Moy sén tu Bou mou gany

  • @RICARDINHO-iq8iy
    @RICARDINHO-iq8iy 14 днів тому +2

    Modou dou beure ak yow, Francesco moy sa adversaire. Na leer 😅

    • @SENETIKTOK
      @SENETIKTOK 14 днів тому

      Franc si douche rekk lagne kooo daaanoul naa liguuey😂😂😂

  • @terangatv2678
    @terangatv2678 15 днів тому

    Ya woor t kham beuré macha allah....

  • @lakhad09officiel36
    @lakhad09officiel36 14 днів тому +1

    Façon mousou ma nêx kii😢😢

  • @ibrahimaibrahima6448
    @ibrahimaibrahima6448 14 днів тому +1

    Bilahi Reug reug dou sama mbeur mais légui il comunique tres bien mashallah professionalisme bagui dougou bou bakh 🎉🎉🎉

  • @CheikhNdiaye-l4q
    @CheikhNdiaye-l4q 15 днів тому +3

    Modou tapha kou dakor lalal j'aime,franc vs reuk reuk😅

  • @OusseynouDiop-d5y
    @OusseynouDiop-d5y 15 днів тому +4

    Goor dou beuri wakh

  • @Dpp205
    @Dpp205 15 днів тому +3

    Reug reug ken khamoul loye wakh

  • @simbaratoure
    @simbaratoure 14 днів тому

    Reug reug seule 🎉❤

  • @BuurMbaye-n7y
    @BuurMbaye-n7y 14 днів тому

    Reug reug seul 🎉🎉🎉

  • @PapemodouThiam-q5c
    @PapemodouThiam-q5c 14 днів тому

    Modou lo moy khalifa général kouly mbeur 😊

  • @Mouhamedba-1975
    @Mouhamedba-1975 15 днів тому +9

    Reug Reug il est sans modestie

    • @senegaleventschanel6913
      @senegaleventschanel6913 15 днів тому +2

      Wallahi je l’ai toujours dit ki badola bou alale dape la bilahi , depuis bamou wakhe à son rencontre avec Ngannou mome ladiouko numerom plais c’était Ngannou à lui avoir demandé son numéro , lolou loussi diare wakh ? Même boko ladione numerom sakhe nga wakh ko wagniwoula dara nak c’est un champion hors paire .

    • @ibrahimaba3553
      @ibrahimaba3553 15 днів тому

      Motay gueume bopam yék nék léne si ay émotions rek yakarni lolou moy adina nafékh baxoul
      En plus yow yay badola bou mak bii ndakh beugo Jambar

  • @KhadimNgom-tn5zf
    @KhadimNgom-tn5zf 6 днів тому

    Modou lo ❤❤ le grand champion il s'appelle Modou lo

  • @papelo8737
    @papelo8737 15 днів тому +1

    Modlo vs reug reug dans les prochains jours wait and see 🎉

  • @papasillytraore7777
    @papasillytraore7777 15 днів тому

    SA Thies Vs GRIS 2 🔥🔥

  • @Seneami
    @Seneami 15 днів тому +2

    Hor sujet 😂😂

  • @BocarAnne-g7d
    @BocarAnne-g7d 14 днів тому +1

    Bilay dof dofloul beu dieul avançou Nganou rek xol dinga xamni meuno MMA dinala kateu ba nga eumbeu

  • @adrienndong6004
    @adrienndong6004 9 днів тому

    Reug kesse champion du monde et bien roi ds arènes

  • @malickseck950
    @malickseck950 15 днів тому

    Makane dou dara sou beuger combat Modou ❤ reug reug na fay Xaragne 150 millions voilà

  • @xelcomdecorationsopeserignesal
    @xelcomdecorationsopeserignesal 15 днів тому +3

    Reug reug yaw do touss 😂😂😂

    • @SENETIKTOK
      @SENETIKTOK 14 днів тому +2

      Daaaraa laa dd moome rek laaafiii president décoré chevalier de l ordre national

  • @elzo1836
    @elzo1836 15 днів тому +1

    Saway ngamouna 😂

  • @tallatoure195
    @tallatoure195 14 днів тому

    Sa thies moy sa papa modou lo sa mame la 😂😂😂😂

  • @NdeyekhadyMbjoue
    @NdeyekhadyMbjoue 15 днів тому

    Yene khôl léne li reug reug wakh mo geune 😢bilakhi modou lo sou dieulé reug reug danou

  • @mbayediop123
    @mbayediop123 14 днів тому

    Je suis fans de modou Lo, Mais il a raison, vous comparez coupe de roi et champions league 😂😂

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane7163 15 днів тому +5

    Ah Reug Reug je ne suis pas d'accord...... Le monde de la lutte reconnaît la couronne 👑👑 Royale ce qui n'a rien à voir avec le MMA ..... Tu t'es complètement loupé Reug Reug..... Arrête de minimiser notre couronne 👑👑 Royale respecte les lutteurs please lol 😂😂

  • @DjibySy-h3f
    @DjibySy-h3f 15 днів тому +2

    3/4 combat ganane champion du Monde Boul dof

  • @malikking4291
    @malikking4291 15 днів тому +1

    Modou Local, Reug international. Deug nèxul

  • @kouroubayefallpure
    @kouroubayefallpure 15 днів тому +1

    Deugla dé mom do mromu ben mbeur champion du monde ak champion bu senelgal du ben xamo lein sport yein champion du monde kea do mromu ben mbeur senelgal vraiment si audience y’a lein epu fouff sax tour mom y’a lein ko epu vraiment

  • @MoussaNiang-iz4rh
    @MoussaNiang-iz4rh 14 днів тому +1

    Khanà Modou lo rek moye mbeur😂

  • @PendaTalla-c5z
    @PendaTalla-c5z 15 днів тому +4

    Reug Reug mome soff la déf ak sokhor

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 15 днів тому +4

    Reug reug dof bou software la mé modou naw lowoula mo takh meusoulo wakh bamou tontoula modou dou tontou dof

    • @SENETIKTOK
      @SENETIKTOK 14 днів тому

      Boukaaa nawlooowoul mooome tamiit nawlawoukoo moome rek laaafiii president decore chevalier de l ordre national

  • @josephcoly4127
    @josephcoly4127 14 днів тому

    Dafa bone ki yeuk succès fi Sénégal la bou niou sonal

  • @oumarndao7485
    @oumarndao7485 15 днів тому +3

    Saway bou wahé rek ngua découragée 😂😂😂

    • @CheikhNdiaye-hb4in
      @CheikhNdiaye-hb4in 15 днів тому

      😂

    • @SENETIKTOK
      @SENETIKTOK 14 днів тому

      Mais bou beurré gua contane kéne meussoukooo djoutal🤣

    • @oumarndao7485
      @oumarndao7485 13 днів тому

      @ kiniou djouteul tay mo séne bay si lamb yallah def mou nekeu sen roi niom nieupeu,comme quoi yallah la rek 😀😀

  • @momoofficial1988
    @momoofficial1988 15 днів тому +2

    Ma beugeu djiko modou lo deugeu dou tontu kèn

  • @Idyxaragnelo
    @Idyxaragnelo 15 днів тому +1

    Deemal dieul sa revanche si Sa Thies

  • @assanebabaofficiel3533
    @assanebabaofficiel3533 15 днів тому +1

    Fekhel meune si senegal mo geune 4 ou 5 combat niounane champions du monde ngay wax fofou amoul saf safal dhe 😂

  • @serignekebe963
    @serignekebe963 14 днів тому

    Modou lo nak tapha tine souko yebber rek mom leu. plus douko dieul, plyus Tapha di geuna am confiance