Tapha Tine répond à Modou Lô : "mako meune, tapét la, damakoy..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 23 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 289

  • @MatarNdiaye-j9n
    @MatarNdiaye-j9n 15 днів тому +31

    Modou lo meilleure lutteur de la lutter sénégalais ❤❤❤❤

    • @Sséga_03
      @Sséga_03 15 днів тому +3

      Le meilleur dou daw ken day melni balla Gaye 🙌🏽

    • @disytbi8711
      @disytbi8711 15 днів тому +3

      ​@@Sséga_03kouy daw dina dieul Boy niang mi niouss Balla gaye ak rakkam tékssi Ama ak Siteu dane lén si bén année 😂😂😂

    • @Sséga_03
      @Sséga_03 15 днів тому +2

      @ kou niémé dîna daw tapha tine mi balla niouss niarry joutalalé sa mbeur tmt ngay wanéwou ni té yallah xamnanè Siteu mola dane bilahi rglél rk

    • @aboundiaye6221
      @aboundiaye6221 15 днів тому

      YAW LEGUI KANE MOLA NIOUSSE 😂😂😂​@@Sséga_03

    • @aboundiaye6221
      @aboundiaye6221 15 днів тому +3

      MEILLEUR LUTTEUR SI HISTOIROU LAMB SENEGAL BALLA GAYE 2 LE GNIMOU BOLE DANE BENA MORAMAM DEFOUKO KOUY WAXAL YALA CHAMPIONS MEUNO DANE NIEUP M BALLA GAYE KENDOU MOM

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 15 днів тому +6

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @Iskhaga-Bah
    @Iskhaga-Bah 15 днів тому +9

    C'est à dire Sénégal so fi nekké numéro 1 say noon douniou nam si ieo ludul sa échec, vs ama niou thiow ko fi ba soon mdlo diapp doumeu ko daan ko, après niouni dafa wara confirmé, niou indi boy niang mu doumeu ko daane ko, yaldaw bi amul arrêt dawkinda bi la même chose. Bref c'est le prix à payer lorsqu'on demeure le meilleur. Sou mdlô daané Tapha tine niouni fogg mu daane reug reug souko daané niouni faw mu daane bg2 ainsi de suite ainsi de suite...etc Soxxor dafa am blh, mbeur bo khamantané bamu dalé beuré arène ba legui niarri mbeur kessé nioko daane(deux champions roi des arènes) Mais n'empêche douniou ko meusseu nangoul. Mdlô souniou fierté le meilleur de sa génération❤❤❤

    • @cheikhflodiao6091
      @cheikhflodiao6091 14 днів тому +1

      C'était pareil ak yekini.. Mais touss modou ay wax daanou ko

  • @babacarmbengue1390
    @babacarmbengue1390 15 днів тому +10

    Le gars en vert , il est le chargé de la communication de tapha tine khana . Tapha est sur le plateau, pourquoi ne lui pas laisser le soin de répondre aux questions qui lui est destinée.

    • @CASI7797
      @CASI7797 15 днів тому

      Moy Elhadj Thioune le mari de Amy Mbengue, c'est lui l'agent de Tapha

  • @amathtv7178
    @amathtv7178 9 днів тому

    Roi Modou lo rek forever ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @afro3827
    @afro3827 15 днів тому +20

    Tapha tine am ponkal ken douko may chance balla gaye mola yakhal modou lo doula dieul dé 😂😂

    • @modoubayefallsikroulla1423
      @modoubayefallsikroulla1423 15 днів тому +3

      May chance amoul fofou lamba léne bolé modou lô balla dako dane mou dém beurék roi

    • @fifty6292
      @fifty6292 15 днів тому +1

      Modou Balla dako diouteul Eumeu dieulko royal modou mo ragal Tapha rek dafa douma Bombardier mou dane modou fofou chance amoufa

    • @papafall5576
      @papafall5576 14 днів тому

      Désolé mais may chance am nafa , ndakh modou c'est le roi moy taneu comme niko roi yeup mbeuss défé​@@modoubayefallsikroulla1423

  • @ndoffenetine5333
    @ndoffenetine5333 14 днів тому

    Modou xaragne le meilleur lutteur sénégalais.
    Le plus grand bagarreur de la lutte sénégalaise ❤❤❤❤
    Le lutteur le plus complet. Déy beuré di xéx, di xéx di beuré ❤😮
    Ba lamb soso ba légui mbeur mou mélni xaragne lo massul am.
    Modou lo un jour
    Xaragne lo tous les jours
    On t'aime point ♥️ ♥️ ♥️ ♥️ ♥️ ♥️

  • @thiernodembaya8355
    @thiernodembaya8355 15 днів тому +6

    Tapha tine & 🇸🇳🇸🇳😇👑faut éviter Modou il est plus athlètes que toit plus près plus rapide il va thé milieu d'eux minutes ce Trop ❤❤❤

    • @Domou_Deukk_Bi
      @Domou_Deukk_Bi 15 днів тому

      Dieule lénko reik nga wané ni modou geuné nek athlètes tapha😂😂😂
      Dangén nékh reik😂😂😂 mounane "faut éviter" di ték khéll😭🤣🤣🤣🤣 yénakay yéné wara éviter téh yéneu ngui eviter lou méti actuellement 😂😂😂😂

  • @Nittou-g4i
    @Nittou-g4i 12 днів тому +1

    Tapha ame nga doolé c'est vrai.. mais mano beuré franchement 😂

  • @bachirvd619
    @bachirvd619 14 днів тому +1

    Wakh rek Wakh rek té jour commba do déf dara kham waye tapha avec kilay parlél 😮😮

  • @MakhmoutFall
    @MakhmoutFall 4 дні тому

    Modou lo milleure❤❤❤❤❤❤

  • @Dioppatriote06
    @Dioppatriote06 15 днів тому +21

    Kou wahal deugeu rék Modou lo day moytou ay Adversaires mais Tapha tine Sa Thiès sont c potentiel Adversaire

    • @sidynoreyni2614
      @sidynoreyni2614 15 днів тому +2

      Tapha tine Moy adversaire bi

    • @Dioppatriote06
      @Dioppatriote06 15 днів тому

      @sidynoreyni2614 c vrai moy premier position

    • @Deggou
      @Deggou 15 днів тому

      Tapha ak sathies naniou beuré demi final kou daneu dieul modou, bayilen combat royal beugéne teugal ci niou diougé ci défaite...

    • @sidynoreyni2614
      @sidynoreyni2614 15 днів тому

      @@Deggou siteu fanla diougué té beuré na ak roi

    • @Dioppatriote06
      @Dioppatriote06 15 днів тому

      @Deggou Siteu biguén koy dieul Si défaite la diougué amolén Laye

  • @AbdoulayeBa-b2i
    @AbdoulayeBa-b2i 14 днів тому +1

    Modou lô vs Tapha tine moy combat amateurs ❤

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 15 днів тому +3

    Tapha tine 😂😂😂😂😂😂😂😂😂 ay rétaane lama dèf

  • @moussapayemane4167
    @moussapayemane4167 15 днів тому +9

    Daw Tapha Tine rék motah toujours mouy wahné damay nopolou 😂😂😂😂ana mbeur ak nopolou 😂😂😂aka ragal Tapha Tine 😂😂

    • @MedMyt-z1p
      @MedMyt-z1p 15 днів тому

      😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @moussapayemane4167
      @moussapayemane4167 15 днів тому

      @MedMyt-z1p 🤣🤣wahone nafi day nopalou mouhar ba Tapha Tine dieul Balla Guaye,2 jours rék mom aussi mou dieul Siteu 🤣🤣🤣monguini wahatné day nopalou bou Tapha amé combat dinga dégue mom aussi dieulna kénéne 🤣🤣

    • @Deggou
      @Deggou 15 днів тому

      3xombat you topanté modou nitt rek la boulen niou sonal...

    • @Abdallah31341
      @Abdallah31341 15 днів тому

      ​@@moussapayemane4167 deug nékhoul, lingua wax mo am

    • @ndenediagne50
      @ndenediagne50 14 днів тому

      Tapete rek moko diap 😂

  • @Black-e8o
    @Black-e8o 14 днів тому

    Tapha tine vs Mod’lo moy combat bii point

  • @ogviito1949
    @ogviito1949 15 днів тому +59

    Tapha yaw mbeur yeup yassi gueun niak diom amo fitt lou modou di ragal si yaw

    • @abdousow2908
      @abdousow2908 15 днів тому +25

      Moma diaxal😂😂 modou amoul kouy doundou mou faléé la

    • @PapeDiego-jb7cq
      @PapeDiego-jb7cq 15 днів тому +11

      Bilay ki balla doorko bamouy nane balla

    • @DjibsonIdriss
      @DjibsonIdriss 15 днів тому +10

      Bayiko fofou balla humilié ko douma ko dane ko mou tokk fii dii kébétou

    • @Bayeniang20
      @Bayeniang20 15 днів тому +7

      Modou mo ghina ragal si mbeur yi ay siteu la nieme

    • @Bayeniang20
      @Bayeniang20 15 днів тому +11

      @ modou sa balla dako humilies na dieul tapha tes bayi daw bi

  • @MOUHAALAMINE
    @MOUHAALAMINE 14 днів тому +1

    Tapha tine vs lac de guerre👊 moudou lo day dakhar sa nday

  • @alioumakhasylla5641
    @alioumakhasylla5641 15 днів тому +2

    Modou meusoule enervéwou bayile lolou

  • @modoumbackediop2830
    @modoumbackediop2830 14 днів тому

    Bilay modou lo moy champion nak way mbeur gnepp modou lagne manule digéré

  • @papamboup7207
    @papamboup7207 13 днів тому +1

    Kou dieul siteu wara meune dieul tapha tine .golo hamna keur am khathie😂😂😂😂😂

    • @fallouvamos
      @fallouvamos 12 днів тому

      Sa défaite contre Balla Moko Yakal

  • @momondiaye8649
    @momondiaye8649 15 днів тому +1

    Tapha tine à raison siteu n'a rien prouver si lamb et prtan beuré na ak roi des arène téklé 3 défaite wa beuré watt ak balla tapha tine à enchaîner 5 victoire

  • @IbouDiattara
    @IbouDiattara 14 днів тому

    Elhadji Thioune ❤️

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara923 15 днів тому +4

    Pa bou sole lou vert li vrai fène katt la😂😂😂

    • @fifty6292
      @fifty6292 15 днів тому

      Comme sa pape rek😅

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 15 днів тому +3

    Wa legui tapha tine ak modou lo kan mokoy teugue billahi tapha tine boo yakaarée ni modou lo dala ragal ya nakha sa poppu 😂😂😂

  • @alioumakhasylla5641
    @alioumakhasylla5641 15 днів тому +2

    Tapha tine miii moye ragale bi khame nguéne lolou

  • @ibrahimatall5277
    @ibrahimatall5277 15 днів тому +3

    Wa Tapha Tine, daw Modou Lo da wakhone day nopalou ngani mono kharr.
    Cette année aussi day nopalou, légui démal dieul kénéne, loy kharr ?😅

    • @fallouvamos
      @fallouvamos 12 днів тому +1

      Tapha mo amoul Chance 😂😂😂😂😂😂

  • @mamepathengom9398
    @mamepathengom9398 15 днів тому +9

    Lolou dou lamb waye Tapha tine safoul mbeur 😂 gris ak Zarco koussi dane moye sa atverssaire 😂

    • @MedMyt-z1p
      @MedMyt-z1p 15 днів тому +1

      Ragal rek

    • @abbadieme3140
      @abbadieme3140 15 днів тому +1

      Tapha d'où beurré ak gris bordeaux...tapha son potentiel adversaire Modou car il n'a pas encore lutter vk lui soite tapha vs sathies mais pas gris oubien zarko

    • @fifty6292
      @fifty6292 15 днів тому +1

      Supportere modou Lo yi gno gueune tapéte ci lamb bi Modou d’à raw Balla thioo😅

  • @CheikhMbengue-fl8ik
    @CheikhMbengue-fl8ik 15 днів тому

    Modou lo ❤❤❤

  • @AmbassadeurDiaz
    @AmbassadeurDiaz 15 днів тому +2

    La femm la elle est forte mes dou déguello
    Lolou rék mo déss

  • @SambaSene-j1h
    @SambaSene-j1h 15 днів тому +9

    Tapha meritewo beuré ak modou denga yambaté

    • @fifty6292
      @fifty6292 15 днів тому

      Siteu mo raw Tapha Tine? Loutakh tapete tamit 😂

    • @nioulesskaye8964
      @nioulesskaye8964 14 днів тому

      Iow Dani kou dane modou lo bombardier ngafi dane té dou weul bati gang iow amo djerigne té safo lamb billahi ak nigua tol bo amone djierigne kene doula dane amo fitt

  • @taphaamdygaye4245
    @taphaamdygaye4245 14 днів тому

    Kou man dall na dieul tapha tine

  • @ModouDiop-b8r
    @ModouDiop-b8r 15 днів тому +8

    Ki mom amoul xorom

  • @ibrahimatall5277
    @ibrahimatall5277 15 днів тому +2

    Si j'étais Modou Lo, damay wotté ci plateau bi, naléne Tapha Tine yama meun fouf,wakh dji diékh.
    Promoteurs yi intéressé wougn ci combat bobou,après nguén beug nu sonal nal Modou moy daw.
    Prononcé un promoteur qui démarche ce combat ???
    Modou teugoul lamb,promoteur moy teug lamb.

  • @papamboup7207
    @papamboup7207 13 днів тому

    tapha tine vs Modou lo moy combat bi 😂😂😂😂

  • @CASI7797
    @CASI7797 15 днів тому

    Tapha Tine yow mom contre Balla la pareii ci seu affaire 😂😂😂

  • @AboulBacharSall
    @AboulBacharSall 15 днів тому +5

    Kounek si sakou yi danguay wathiate si souf mouno daan ama balde mouno daane boy niang balla douma leu eumeu doumala ngua reuthie beug beure ak roi bii ta amo supporter bein prometteur douko deug

    • @soukayeyade4310
      @soukayeyade4310 15 днів тому +1

      😂😂😂😂 dafa nekh may wakh mounane maffi aupe adversaire

  • @MoussaNdour-k8z
    @MoussaNdour-k8z 15 днів тому +1

    Tapha tine kaye bay 😂😂😂😅

  • @MbeussTalibebamba-k4b
    @MbeussTalibebamba-k4b 15 днів тому +1

    Tapha tine yamal yaw Do mbeur 😂😂😂😂😂😂😂

  • @MohamedDiallo-he9eu
    @MohamedDiallo-he9eu 15 днів тому +11

    Pourquoi il sont tous contre Modou Lo 🤦🏽‍♂️😂😂

    • @Neymar1994-m5m
      @Neymar1994-m5m 15 днів тому +3

      Bayiléne séne yi modou yageu na dane ay mbeur té kéne ladiouko mé kou yor roi bi ni ngay mél niépeu lay lathie bou yorotoul doto léne dégeu niokoy lathie ngana tous contre modou lo

    • @FalloutDiba
      @FalloutDiba 15 днів тому

      C'est pas que mo yor lini weur

    • @matarndao-sy7do
      @matarndao-sy7do 14 днів тому +1

      Non pas Modou lo mais couronne bi😂😂 souko niaké rek faye

  • @iscojo6600
    @iscojo6600 14 днів тому

    Yakh Ambition quoi !!! Mo mome c’est une personne, khana legui mo kassé moffi né?? Tapha Reug ou Reug Franc ou Franc Tapha sont des combats!!! Beureléne séne biiir ahhh

  • @SerigneMbackeCissé-w5b
    @SerigneMbackeCissé-w5b 15 днів тому +1

    (Modou lo) tél tél télaaa yéwouuu.

  • @100bouts6
    @100bouts6 15 днів тому

    Respect taf

  • @alioudiop6125
    @alioudiop6125 15 днів тому

    😂😂😂😂😂 thieuy sama copain Tapha. Ah iow nak neikho diapalei deih 😂😂😂

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 15 днів тому

    Tapha so yakarei li mo takh modou dila djeul Yangi nakh sa bopou dei😂😂

  • @Killer-z1u
    @Killer-z1u 15 днів тому +4

    Saway do mbeur demain défi building do tousse

    • @fifty6292
      @fifty6292 15 днів тому

      Dane Boye Niang eumeu Bombardier gnari ay roi lagn wone wakhofi dara

  • @abdoulayekane456
    @abdoulayekane456 14 днів тому

    Tapha tine qui ne même pas prendre la parole pour ce défendre en tant que lutteur soi-disant vip😂

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 15 днів тому +1

    Tapha tine safoule khorom safoule socar😂😂😂

  • @MohamadouDiallo-t8o
    @MohamadouDiallo-t8o 15 днів тому

    Tapha tine dh bilahi wallahi modou lo moko meneu fouf dakoy dane dieul bou yomb

  • @mortallathiam4599
    @mortallathiam4599 10 днів тому

    Thiow lii yeup diarou ko, tine vs Modou Moy combat bi

  • @alphandiaye8541
    @alphandiaye8541 15 днів тому

    Wakh deugue Yalla . Modou défa ragal Tapha.

  • @Ndarguedjtv
    @Ndarguedjtv 15 днів тому +1

    Oustze sa bou tapha tine takhawè mounè daye nopallou🤣🤣

  • @AbdouNdiaye-ph8mp
    @AbdouNdiaye-ph8mp 15 днів тому +2

    Saway mayniou lamb affaire you saytanéla tapha tine vrai ragal la Mouy diay yarou ni kholal balla nim ko agressé rék bo daneko

  • @AdamaMballo-t9s
    @AdamaMballo-t9s 15 днів тому +5

    Pourquoi pas tapha tine-lac2
    Modou est meilleur que tafa il n’a pas peur de toi.
    Tapha tine-reug reug

    • @leveridique-kj7qo
      @leveridique-kj7qo 15 днів тому

      Kone loumouy wiri wiri ay att. Tapét ngène. Mosou léna gnémé Tapha Tine.

    • @Deggou
      @Deggou 15 днів тому

      Pourquoi pas tapha vs sathies niarr niou diougé ci défaite naniou defe demi final

    • @fifty6292
      @fifty6292 15 днів тому

      @@Deggoumodou ci défaite la diogué contre Balla mou beuré royal Siteu bi mou dieul ci défaite la diougué wakhou tapéte mm daw bou Tapha togué 10ans modou dafa wiri touti Siteu wére ko dafa moye rek

  • @brunobadji5867
    @brunobadji5867 15 днів тому +1

    😢Tapha iow soumadone sa diabar ma gnane la bate bila balla dané Niakk diome

  • @thiernodembaya8355
    @thiernodembaya8355 15 днів тому +2

    Pourquoi pas reug reug 🇸🇳 et tapha tine 🇸🇳

  • @FghChv-vl8rp
    @FghChv-vl8rp 15 днів тому +6

    Mais l'homme en vert la quelle est sont problème avec Modou lo kouko fék mounane Modou lo dois se comporté comme un sensibilateur

  • @babacar3178
    @babacar3178 15 днів тому +1

    Mom pouseul rék la ame 😂😂

  • @senegaleventschanel6913
    @senegaleventschanel6913 14 днів тому

    Tapha Tine vrai doff nga naka ngay neker Medina gris di wa Medina ngane daguay beure ak mome, say rakk sakhe niome mbaye gouygui etc douniou beure ak Wa Medina yi niogui deff 💯 ak niome di dorando li motakhe digua yekhe ame adversaire deh

  • @pronosticfootsenegal1112
    @pronosticfootsenegal1112 15 днів тому

    Damay dem maka damay nopalou tieuy bi roi 😂😂😂😂😂😂 niémé woul tapha tine dé

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 15 днів тому

    Supporter Diouto yii ay rétan lanma Déf man Modou lo Dei barke alhouran loutax mouy daw Talpha Tin pendent des années xam nako 😂😂😂thiouth Day xam Lèkam dei Tapha Tine Dacoy raydè😂😂😂

  • @davelelion8789
    @davelelion8789 15 днів тому +6

    Tapha Tine amoul khorome motakh sponsor yi sawarou gnou si mom c'est ça la vérité absolue.

    • @muhammad3323
      @muhammad3323 15 днів тому

      Comme ton pere

    • @davelelion8789
      @davelelion8789 15 днів тому

      @muhammad3323 Mon est décédé paix à son ame, il faut arrêter d'insulter les gens qui donnent leurs opinions sur les réseaux sociaux alors si tu n'as pas argument pour répondre correctement mieux rester bouche bée, Meune nala saga sans problème je peux faire la même chose que toi, mais doumako déf Mbaam boula wékhé nga wékheu ko yéneu yéme.

    • @senegaleventschanel6913
      @senegaleventschanel6913 14 днів тому

      @@muhammad3323ton message bilahi m’a touché parce-que les sénégalais dans les réseaux savent seulement insulter et c’est vraiment grave , dès que tu donnes ton opinion ils t’insultent pour aucun raison , sans même savoir si tes parents sont vivants ou pas . Masta sa pape yalla nako yalla yereum te kharelko aldiana firdawsy

  • @bassirousow3603
    @bassirousow3603 15 днів тому

    Stp delen xolate sen inviteyi wayy stp

  • @seydounouroufaye8353
    @seydounouroufaye8353 15 днів тому +4

    Wakh deug yalla modou lo day daw tapha tine

  • @SeydouFall-f6i
    @SeydouFall-f6i 15 днів тому

    Tapha thiouné la 😂😂😂

  • @xelcomdecorationsopeserignesal
    @xelcomdecorationsopeserignesal 15 днів тому +1

    Yaw maye niou diamou mbeur yépp yaye séné nabba 😂😂😂😂 ama da la dane 😂😂😂

  • @ndongokandji5313
    @ndongokandji5313 15 днів тому +1

    Wakh Dji wakh dji mo beuri rk wayé modou gnéméwoula balla Gaye rk mola yap gnoussi déss mome😂😂😂

    • @AminataDIOUF-ez8kd
      @AminataDIOUF-ez8kd 15 днів тому

      Nonu leu demé nak 😂

    • @AboulBacharSall
      @AboulBacharSall 15 днів тому +1

      Qui dangua faate likou kagn le gueudj daane mbeur qui day bouxante rk amoul xorom amoul supporter na xar lac paré kokou moy adversairam

  • @davelelion8789
    @davelelion8789 15 днів тому

    Modou lo est le seul lutteur qui a fait 3 combat sur une seule année alors Souka nékhé dém macca souka nékhé nopalou.

  • @DameSalle-b8k
    @DameSalle-b8k 15 днів тому

    Moudou lo diele tapha dameye dam maka😂😂😂

  • @DethieDioufFissel
    @DethieDioufFissel 15 днів тому

    Tapha Tine a raison 🙏Modou lô oubien Adja lô 😂🤣n'est pas digne

  • @chifahi6568
    @chifahi6568 13 днів тому

    Franchement tokk di khass modou lo dou sa rôle
    Lamb dagnoulay douma dane la ga tokk di khass modou lo

  • @khadimfall979
    @khadimfall979 15 днів тому

    Petit roi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @GuyGuiguitou
    @GuyGuiguitou 15 днів тому

    Deug leu wakh dh modlo lol wakhoul Dara ci tapha tine franchement

  • @elhadjimamadoudiaw3628
    @elhadjimamadoudiaw3628 15 днів тому

    Sérieux nakk modou lô gnemeiwoul Tapha tine wax ji mofi nekk rekk ins bi nena day nopalou bou Tapha tine jeulei avance mou gneuwate jeull combat 😂😂😂tapete bou srx sax 😂😂bilae balla gaye moy gaindé !🤴🏾

  • @ycthekid6068
    @ycthekid6068 15 днів тому +4

    Tu n'a pas le niveau pour lutter avec modou lo ni par les performances ni par la popularité et c'est la veritè

  • @ndenediagne50
    @ndenediagne50 14 днів тому

    Modou Lou yomb la begue 😂

  • @biranecamara6796
    @biranecamara6796 15 днів тому

    Modou lô daffa ragal tapha tine 😂😂

  • @eulthewritah4070
    @eulthewritah4070 15 днів тому +2

    Yaw Tapha boul faté ni danga danou par humiliation sur le rival numero 1 de Modou LO donc war nga khamni modou lo doula dieul tu a redoubler depuis 2005 tu es là lutteur le plus complet mais le plus nulle de l’arène à part Eumeu Sene bane VIP en activités nga daan ci lamb ji ? Défaite contre Lac 2 défaite contre Ama baldé défaite contre Balla 2 fois kon yaw louy sa problème yaroul rek tapétt mola téré done roi des arènes mais dou gnakk dollé😂😂

  • @bellingham-k6t
    @bellingham-k6t 15 днів тому

    Damay dem makka😂😂😂

  • @Mbodji-walo
    @Mbodji-walo 15 днів тому

    Modou Lô na dieul niary avance Sa Thies ak Tapha Tine yeupp

    • @babacar3178
      @babacar3178 15 днів тому

      Non non modou lo na dieul reug reug tapha tine beuré ak sa thiés koudane mou dieul leu😂

  • @bachirvd619
    @bachirvd619 14 днів тому

    Modou lo dal mo diar modou rek 😂😂😂

  • @adamslo7971
    @adamslo7971 15 днів тому

    Evader 😂😂😂Yoe saway ya geuna nekha Dane cii mbeur amo fittt geuna nekha yew cii galathie ganane modou lo ragall Yoe ya amoull xorom lamb tafa demall liguéyii dess na ama dala Dane boy niang avertisement Lala dané epui amo suportaire Tei insbii Xaliss laniou woutt modou day bayii legui lamb

  • @MouhamedCissé-j9d
    @MouhamedCissé-j9d 15 днів тому +1

    Modou Lô dafa ragal Tapha Tine. Lolou Modou Lô thi bopam moléne ko geuneu xamm même ses supporters le savent très bien. Balaa may dé gnounane Tapha tapéte leu légui Modou Lô loumouy xarr pour dieul ko. Ils sont tous libres maintenant. Modou Lô gneup la beurék thi séne génération sauf Tapha Tine. Il est temps mou dieul ko sinon dakko ragal. Lolou moy deug.

    • @Deggou
      @Deggou 15 днів тому

      kou beur ak b52 khawma loumouy ragal si tapha tapha mi diougué ci defaite modou douko dieul biyobo ngeen wakh da ragall sen xalate la rek

  • @AbdouCisse-xs5mc
    @AbdouCisse-xs5mc 15 днів тому

    Tapha tine 😂😂

  • @Domou_Deukk_Bi
    @Domou_Deukk_Bi 15 днів тому

    Tapha nimako guissé nii kouko fayoull sakh faye modou mou beuré😂😂😂 dafa yakamté napadié modou😂😂😂

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara923 15 днів тому +1

    Tapha tine ya gueneu tapète si mbeur you magg yi ngay beuri wakh

  • @kalam_vrvr9125
    @kalam_vrvr9125 15 днів тому

    Non Sénégal nio retard ay affairou gateu ndiol mais lolou amoul solo..

  • @issakanafiou1865
    @issakanafiou1865 15 днів тому

    Dite à tapha d'aller tire les camions il n'es plus un lutteur plutôt un bounding

  • @mariamaba6644
    @mariamaba6644 15 днів тому +1

    Tapha tine amoul xorom amoul mbolo beug beurre ak modou lo

  • @MohamedThioune-p9k
    @MohamedThioune-p9k 15 днів тому

    Kou niak diom Moy tafa tin

  • @Ousmane-pz1if
    @Ousmane-pz1if 15 днів тому

    Tapha tine lac 2 diokhe len chance woroul

  • @babacar3178
    @babacar3178 15 днів тому

    Tapha tine mon niak diome danou

  • @jobehamidou6545
    @jobehamidou6545 15 днів тому

    Modou lo a peur de Taphe Tine

  • @maamseexgey5964
    @maamseexgey5964 15 днів тому +2

    Tapha mérite de disputer un combat royal.

    • @niokhobayediouf4048
      @niokhobayediouf4048 15 днів тому

      De disputer encore. Mok balla beuré nagne combat royal

    • @beugs9192
      @beugs9192 15 днів тому

      il avait disputé un combat royal en 2013 avec Balla Gaye et avait perdu

  • @abdourahmanesindidi1818
    @abdourahmanesindidi1818 15 днів тому +1

    Mais lou tapha deff ba niou kay khass ? parsk balla moko daan . c tres normal xlo warko dieul

  • @davelelion8789
    @davelelion8789 15 днів тому

    Modou lo ne peut avoir peur de Tapha Tine, parce qu'il a lutté avec des adversaires beaucoup plus coriaces et plus dangereux que Tapha Tine comme Balla gaye, Eumeu Séne, Ama baldé, Gris Bordeaux et Lac 2.

  • @djibrilkonte6928
    @djibrilkonte6928 15 днів тому

    Tapha tine pr yo degua yakarni ya meune modou lo fekhel rek bah avance bi niewe ngue dieulko

  • @OscarbouXlo
    @OscarbouXlo 15 днів тому +2

    Ioe niank diom motakh dieulo roi Vip fraude moy ioe ama dala niouss dan la lac dan la balla dan la Boy niang sakh meuno ko dan

  • @morgaye9582
    @morgaye9582 15 днів тому

    Tapha tine wakh dji diaroul mouy beuri amguein ay promoteur baol ils n'ont qu'à aller démarcher le combat fay louko diar modou deupleu lou neikh

  • @diangcheikh1117
    @diangcheikh1117 15 днів тому +1

    Tapha tine gor djiguen là bala guay dohan sa daye guay tahaw fi du wah