Tapha tine waroul wone dieul balla gaye2! Kawtef coach bakary Matar gueye et dieylani réagissent..

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 18 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 86

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane7163 11 місяців тому +14

    Azize Ndiaye détient le monopole de la lutte ... Financièrement il est plus puissant 💪💪

    • @ndeya5099
      @ndeya5099 11 місяців тому

      Dieu seul est le tout puissant c lui qui détient tout

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking382 11 місяців тому +8

    Balla gaye2 grand champion le tarkinda le roi des arenes le papa des lutteurs ndam rek Inchallah 🎉 😊

  • @lbyoungtv2223
    @lbyoungtv2223 11 місяців тому +12

    Franc vs siteu moy combat bii 🎉❤❤

    • @MamiDiallo-k4i
      @MamiDiallo-k4i 11 місяців тому

      Très bien dit,thiouthieu dafay kham lèkam,siteu AK franc Moy combat

    • @mouhamedmoustapha684
      @mouhamedmoustapha684 11 місяців тому

      Bilay moy combat bi deug nexoul

    • @sonkofocus2024-ph4hv
      @sonkofocus2024-ph4hv 11 місяців тому

      Siteu 1milliard dou dieul franc nak 😂

    • @mouhamedsambe7820
      @mouhamedsambe7820 11 місяців тому

      @@sonkofocus2024-ph4hv siteu dou sama mbeur mais dieul franc même dane ko yobou wouko fein siteu déjà mongui si vip yi franc la combat bobou Amal nieurign déjà niveau cacher yi bakoul franc quench moy adversaire ram souko dieuloul man malako wax dou beurei saison bi

  • @AbdulBah-y8t
    @AbdulBah-y8t 11 місяців тому +3

    Balla guye rk inshallah ❤

  • @AlAminesy30
    @AlAminesy30 11 місяців тому +3

    Vraiment ay nafekh Nguéne fou nguéne tekni Balla gaye 2 Moy Favori

    • @akadtv661
      @akadtv661 11 місяців тому +1

      Psk Balla moko danone tei moko eup victoire fouf

    • @AlAminesy30
      @AlAminesy30 11 місяців тому

      @@akadtv661 lolou dou sport deh niatta combat la Tapha tine téguélé Di dane epuis niou dagne Balla gaye nieup tapha tine daléne dane

    • @akadtv661
      @akadtv661 11 місяців тому +1

      @@AlAminesy30 Eumeu Séne kassé lassi dane gnisi deff yeup decision arbitral lalen daner

    • @AlAminesy30
      @AlAminesy30 11 місяців тому

      @@akadtv661 fo fatté bombardier

    • @akadtv661
      @akadtv661 11 місяців тому

      @@AlAminesy30 Tapha par avertissement la daner Bombardier saway

  • @serignesamfall9948
    @serignesamfall9948 10 місяців тому

    Merci de suivre Serigne Sam fall bio

  • @abakarafall6276
    @abakarafall6276 11 місяців тому +1

    Bakari vere campione ❤

  • @ndiougamar2202
    @ndiougamar2202 11 місяців тому +3

    Tapha tine risque bou make la dieul mais waroul woone dieul Balla gaye

    • @OusmaneFall-b9h
      @OusmaneFall-b9h 11 місяців тому

      Donc kane laay beurel

    • @ahmeds7785
      @ahmeds7785 11 місяців тому

      Y a aucun risque, Balla gaye est fini ....

  • @emmanuelmendy3058
    @emmanuelmendy3058 11 місяців тому +2

    No année blanche bakhoul si mbeur gnom tapha tine balla lac 2 guerre gris bordeaux et consor. Lilén désé si lamb bariwoul ils n'ont rien à prouver

  • @emmanuelmendy3058
    @emmanuelmendy3058 11 місяців тому +1

    Boye Niang reug reug

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9ye 11 місяців тому +1

    Il ne peut pas attendre Modou lo sinon c'est qui c'est arrivé à Ama peut lui arriver

  • @emmanuelmendy3058
    @emmanuelmendy3058 11 місяців тому +3

    Franc siteu combat le n'a boyi beuré sén bir

  • @infosn332
    @infosn332 11 місяців тому

    Tapha Tine doit faire attention avec les Aziz et baye c eux les vrais marabout

    • @OusmaneFall-b9h
      @OusmaneFall-b9h 11 місяців тому

      Yaw louy marabout

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote 11 місяців тому

      Sou done lolou boy niang douko dane eumeu douko dane😂 ba si b52😂 saway lamb dou lolou affaire bi entrement la al beuré tek si fite molay may ndam ak dieul risk😂😂 mèl ni lac 2 tapha tine dougnou dieul bène risk😂

  • @modoudiop7841
    @modoudiop7841 11 місяців тому

    ❤❤❤❤

  • @Sofia2201-b4n
    @Sofia2201-b4n 11 місяців тому

    Bakari vrai doff nga yaw kou am xalis teugaal lousi yonou aziz ndiaye

  • @babacarbambistesarr3313
    @babacarbambistesarr3313 11 місяців тому

    Siteu limouy lathie si khaliss pr dieul Balla wa albourakh meunounioukoko fay

  • @fallsaliou8442
    @fallsaliou8442 11 місяців тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @babacar3178
    @babacar3178 11 місяців тому

    Coach bakary reug la faral reug rék laye topou😂😂mé modou beuré woul ak reug

  • @papi4900
    @papi4900 11 місяців тому +1

    Len rek momasi nekh ballah dem tok fignu wiss ba barr😅

    • @64FallAmadou
      @64FallAmadou 11 місяців тому

      Mais affaire yi dafa teil dh 😂😂😂

  • @AhmadaJadid_Diop
    @AhmadaJadid_Diop 11 місяців тому +1

    Bakary oui ils doivent laisser les autres teug combat you nekh yi, mais après aussi les autres promoteurs daniouy ray mbeur yii. Il est temps mbeur you ndaw guiss sen bop ci lamb. Actuellement mbeur yi ils trouvent plus leur compte ci Albourakh. La majorité des promoteurs daniouy amel mbeur yi khaliss dilen dawlo rk.

  • @senembaye9928
    @senembaye9928 11 місяців тому +1

    Non bakari ya bari wakh bilaye walaye sof nga trop khamo touss thi lamb

  • @mynameis6391
    @mynameis6391 11 місяців тому

    Bakary dafaa sooff trop, mais deugg rek lay wakh.

  • @talladiakhate4919
    @talladiakhate4919 11 місяців тому +1

    Balla dane kéneu😂

  • @Steven-ul8pw
    @Steven-ul8pw 11 місяців тому +1

    Dieylany iow Xamo Lingay Wah Tapha Tine Suko Balla Daané Mou Wayédi Nganaan Amul loumsi Perd Tapha Tine Liko Tardél Moy Djeul Combat Yuko Dul Yegal mom lay perd Nopina Beuré Courone

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 11 місяців тому

    Bakary ya barri nga ndaye wakh torp

  • @leuzcisse6181
    @leuzcisse6181 11 місяців тому

    Tapha tine Balla Khégne Nako Roi Bi tapha Dafa Warone n'a Khare Modou lo Même Fi Ba 2ans Où 3 sans Par ce que Souka Balla Dané Pour Âme Modou lo D'où Yobou

    • @laperlecmoi5995
      @laperlecmoi5995 11 місяців тому

      Tapha tine palmarès desna riche pour moi ameu Modou lo

  • @smaplarime8904
    @smaplarime8904 11 місяців тому

    Tapha tine kay da mel ni beugoul lou bakh té promoteur yi respectewougne ko,combat royal la waroul beuré mais ay balla moi diekhal mi ban avancement la si am

  • @SeydinaMandioneNiasse-fk4tn
    @SeydinaMandioneNiasse-fk4tn 11 місяців тому

    Bakhena delene wakhe rek Mane balla gaye moye sama mbeur Waye n'a khame ni âme combat

  • @atoumaneniasse4854
    @atoumaneniasse4854 11 місяців тому +1

    Tapha tine amoul staff balla gaye ak baye ndiaye nio far

    • @64FallAmadou
      @64FallAmadou 11 місяців тому

      Bay Ndiaye beuréwoul dh balla moy beuré 😂

    • @laperlecmoi5995
      @laperlecmoi5995 11 місяців тому

      Et âpre qu'est-ce que ça fait ?

  • @MouhamedmoustaphaNdiaye-w5l
    @MouhamedmoustaphaNdiaye-w5l 11 місяців тому +5

    Oh staf de tapha tine nelaw nguen dh hamnguen ni coute que coute balla daf len di dan dem jeli modou lo seut

    • @Mbt.-_
      @Mbt.-_ 11 місяців тому +1

      Wakhi dofff bayi Len di wakh melni kou kham do yalla bou jour ba inchallah niou khol te nga nek nitt modou dotoul beuré ak balla ok

    • @lifeissoconfused2809
      @lifeissoconfused2809 11 місяців тому +1

      @@Mbt.-_yow tamit ya ngui melni kou kham louy xew souba naan Modou dou beuré ak Balla lossi xam

  • @emmanuelmendy3058
    @emmanuelmendy3058 11 місяців тому

    Tapha tine c comsa boul délo avance yén vip yi lilén désé si lamb bariwoul amato lén li ngendi prouvé

  • @medounethiam2191
    @medounethiam2191 11 місяців тому

    Matar xamoulo lambj Tine si balla le terasse il perd bcp

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 11 місяців тому

    Bakary yaw khamo touss thi lamb ji wakh rak

  • @souleymanembodji1534
    @souleymanembodji1534 11 місяців тому

    Var ame na

  • @ElhadjiFall-nw2he
    @ElhadjiFall-nw2he 11 місяців тому +2

    Vrement nafekh amna .Mes kharagne mo raw balla??

  • @gorasambe3719
    @gorasambe3719 11 місяців тому +1

    Wakhi dof matar tapha dou khaar dara

  • @moustaphacisse4037
    @moustaphacisse4037 11 місяців тому

    Lamb dou ay fou d'où ay thiakhane nanio ko teu te dika doundo me sak jour live AK debat rek sak jour mem debat 😢😢 nioun niouy yakh sunu tane dilen deglou ta combat bou âme nioun AK yen niou kay setan en direct

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 11 місяців тому

    Bakary toukh katou yamba bi

  • @NdiagneNdiaye-wn5ts
    @NdiagneNdiaye-wn5ts 11 місяців тому +1

    Mais bakary n'avait tu pas dit que tu ne parlerais plus de la lutte? Tu nous pompe l'air vraiment. Est ce que yaw gor nga

    • @NdiagneNdiaye-wn5ts
      @NdiagneNdiaye-wn5ts 11 місяців тому

      @@DjilySarr-l3b si c'est de moi que tu parle, je suis dix mille fois aussi instruit que toi

    • @ahmadoudiop5016
      @ahmadoudiop5016 11 місяців тому

      ​@@DjilySarr-l3bmais comprendre nagnu c'est l'essentiel

  • @derickndiaye5918
    @derickndiaye5918 11 місяців тому

    Yow fans balla nga mais kham nga ni balla dotoul Eupeu dolé tapha tine cii lamb,sokhor ak farr bakhoul .palmarès tapha mo gueuneu riche bou balla Diamono yi .sokhor bakhoul

    • @ahmadoudiop5016
      @ahmadoudiop5016 11 місяців тому

      Palmarès môme palmarès leu rek amoul bou demb ak bou tay 😂😂

    • @EMELES-
      @EMELES- 11 місяців тому

      @@ahmadoudiop5016moma diakhal🤣🤣🤣Balla gaye mo dakalei palmaeres thi lamb dji mok yekini

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote 11 місяців тому

      Tapha tine lac 2 nio eupou dolé si lambj mè ay ngaka lagn😂 dougnou dieul bèn risk meunougn beuré amougn fite😂 fite ak beuré bou wor moy dane bg2😂

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote 11 місяців тому

      Palmarès lan😂😂 dano lac dano boy niang dano b52 😂tèk si eumeu mi née fin carier nokou la bangay ram😂

    • @kefgg
      @kefgg 11 місяців тому

      ​@@leuz.patrioteKou dane lagnou lathié pas kou nokeu. Tapha tine dane neu Eumeu point.
      Boudé noke rek Gris nokeu nafi Eumeu sene 2011 meme si eumeu mo dane. Kone lolou wakhi doff leu...

  • @Cheikhlo570
    @Cheikhlo570 11 місяців тому

    Modou lo beuréwoule ak balla

  • @SadiaSeydi-m8f
    @SadiaSeydi-m8f 11 місяців тому

    Dieylani c'est pas vrai ce tu dit

  • @ndiougamar2202
    @ndiougamar2202 11 місяців тому

    Aziz Ndiaye mome ak mafia wam dagno beugue contrôler lamb ji

  • @ndiaboutadiouf9300
    @ndiaboutadiouf9300 11 місяців тому

    mais bailleur yi nekk si lamb ji.ngen .balma geumolen.sen bop aziz akk baye fait ce qu'il veulent dans larenes Ken dou wakh ndakh xaliss bignou yor en plus lingen Def tapha tine dafa niaw lol deugeu rekk mo nekh yalla soudon position .bi tapha nekk la balla nekk niom aziz dougnou meuseu nangou beure akk kenen. koudoul modou lo len de xam nako niom aziz akk baye balla modou lo lagniy .wadial nagnou dem basi kanam lep dina ler quelle staff de tapha dara xamo len ko legui souko balla dane dem beure ak modou lo mom delou wat guinaw nit dangay am fouleu te geum yalla fi yalla rekk mofi nekk

  • @khadimdiouf2076
    @khadimdiouf2076 11 місяців тому

    Dieylani xamo leufeul ndaym

  • @ahmeds7785
    @ahmeds7785 11 місяців тому +1

    Vous êtes tous passés à côté dans vos analyses, Balla avec son état actuel ne peut pas battre Tapha

    • @Senegal_253
      @Senegal_253 11 місяців тому

      Comba bi desna 6 moi

    • @akadtv661
      @akadtv661 11 місяців тому +1

      T’es d’accord que Balla mo dakk beurè Tapha Tine ??

  • @MrFayemanou
    @MrFayemanou 11 місяців тому +1

    Balla douu touss tapha dinak nokou bamou teud

    • @ahmadoudiop5016
      @ahmadoudiop5016 11 місяців тому +1

      Bilay ligua wakhni gueumouloko

    • @MrFayemanou
      @MrFayemanou 11 місяців тому

      @@ahmadoudiop5016 mooo bakhna

  • @adamadiaw7906
    @adamadiaw7906 11 місяців тому +1

    Yaw mom sa lunette Yi nga méleni infirmier !!! Xamo touss ci lamb