C nice mais Les enfants doivent savoir leur limites. Kou neke yakhame sa matou lale. C pas Bien dencourager Les enfants a etre Des manipulateurs. Des fois c mieux de divorcer que detre ds une relation toxic. Tt es une continuation mo takhe sunu seye yi di ame problem en commercant avec Les belles meres.
J'aime la stratégie de Sokhna mou ndaw pour la réconciliation de ses deux parents.L'honneté et la franchise de Ndeye Touty envers sa copine Maty Rose me plaît beaucoup.
Yaye Dior wakhna lou ame importance néna ndiawar li nga ame mako liguéy sa keur baye dama heuye nga guotou toujours niounane liguéyou ndeye na féke dom ame diome ndeye yépa liguéy na dom ame diome rék vraiment evenprod mention spécial à vous yéna gui diangualé lou ame solo yéna dékalate théâtre lepe c'est la réalité sénégalaise pas de fiction diarama 🙏🏾😍❤️❤️
Sallahou alla Mohammedine ❤ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa Salim ❤ allahuma sali halal massoufi bil karami wal djoudii ❤ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa alla alihii wa sakhbihi wa salim
Au Sénégal fébar bima gueuna ragal moy fébarou xel par ce que aux yeux des gens do wer mouk même sou yalla deffé lepp dagne thi yaw aux regards des personnes amna lou dess bagne nañou ko dof dou wer lañouy wakh ce qui est déplorable fébar la comme fébar yeup daffay wer Que dieu nous assiste😢
Yalla nako yalla yeukati ak diamou bamou dèllou wate thie ay mbireum si barkèp borom Touba touff touff touff sama xôll lako tibbè nakk ndax yaye dafa foore ءامين يارب العالمين 📿🤲🏽🙏🏽
Soda Marème est très intelligente elle a tout fait pour gagner la confiance de ndiawar, écarter Seydou pour mettre son plan à exécution. J’ai jamais eu confiance en elle à propos de l’entreprise, alal ndiawar bi yeup lay récupérer
Ndiawar doit faire comme moi,pour OBLIGER sa mère et Boury à faire la paix..En effet, avant, ma sœur Aïda et ma femme Queen Bineta, n'étaient jamais d'accord. Quand j'en ai eu marre, j'ai demandé à un ivrogne un peu de bière que j'ai versée sur ma chemise. Arrivé à la maison, je "tare tari"😂 et chante comme un ivrogne " wooye Birima, foumou yéndou ma yéndou fa, yèndo nane né, bani tateu. Hé boy maman , wakhale boy Aïda ak boy Binette, gnou djoubo". Maman dit en pleurant " c'est votre faute, mon fils n'a jamais fait ça". Aussitôt, ma sœur et ma femme s'embrassent. "Gnaf" personne ne veut un frère ou un mari ivrogne😂. Depuis lors, "djameu" la paix. "Légui kou dékoné rék, ma déf tateu"😂😂. LOVE
Ndiawar c bien 😂 je demande si vraiment vous faite confiance a soda maréme prck moi c no boury nak khalé yi késsé takhouniou nga bgue délou ms tu aimes ndiawar 😂c très bien soxna bou ndaw elle est forte walay j’aime son talent 🎉❤soxna diagne sik na ms elle aime ses enfants ❤encore une fois chapeau l’équipe 🎉
Soda maréme mii bakhna dal mougui nane kharal ma indi document gua signé ko mBadou loumay khalate nakh théâtre bii xaliso lo toudou mbadou dieule bien ndiawar bii yeup
Ce que Soxna bou ndaw a fait pour sa maman m'a tellement touché et m'a fait rêvé en même temps. J'aurai tant aimé sameu dome bou goor bi dioubolé m avec son papa.Mais c'est encore un bebe.
Oui je l'aime, je suis amoureuse de lui mom la xam, c'est très difficile de passer à être chose. J'ai fait tout ce que j'ai pu pourtant mais malheureusement j'ai pas eu gain de cause. Nianal léne m rek,mon foyer me manque
Chapeau à Sohna bou ndaw 😊 Boury j’aime sa manière de faire tout pour le bonheur de ses enfants On en parle de Ndiawar avec c’est très bien c’est bien 😂😂 Ndey Touti c’est pas seulement une meilleure sœur mais aussi une merveilleuse amie qui conseille bien 😊 Omar ne pas si fou que nous pensons il fait tout pour obtenir ce qu’il veut c’est un fou intelligent 😂
La complicité entre soxna et sa maman est vraiment extraordinaire ❤et genre soxna yii dagno bakh si parents you divorcer nakh dou bayi ,c’est une bonne sentinelle 😂
Kou content si Sokhna mou ndao rkk lalal ❤dama dée man si wakhtaanou Iboulaye ak Omar Diagne doff bou am khel😅 Ndeysan Boury chapeau à elle 🎉🎉🎉ele veut retourner avec son ex mari a cause de tes enfants thiey l'amour maternel amoul morom bravo a nos mamans ❤
Wa mani jspr dou man rek mafi Avancer pub dee 😂blhh setane série si telephone dra dakouko youkhouu haleii doula terei deg wakh dji commentaire en même temps k la série doula déconcentré bangay merr Di yeg😂vive even prod vive you tube 😂
Faux raccord bou ndaw, Boury a dit sa fille de prendre ces bagages ensuite elle a dit à son Père kel va l'aider à faire ces bagages. Mais elle est partie avec son père sans bagages. Souma joumé aussi ngen wahma
La meilleure maison de production de sénégal respecte tellement l’heure de t ses téléspectateurs vraiment vous êtes les meilleurs ils méritent les 5M avant 2025😊❤🙏
Le retour de Boury ❤😂😂😂😂😂😂😂 kou beuge Boury Ak Xalisso rek l'alal j'aim ❤❤❤
❤❤❤niankou
❤❤❤
❤😂🎉😮
❤❤❤😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤ 12:18 12:19
Sokhna la beugeu mane bly khalebi mo meune limouy déf 😂😂
Alhamdoulilah des cœurs pour notre prophète Mouhamed
❤️❤️❤️❤️❤️
Sama Keur gua dieum nono sama Keur badiéne😂😂😂 Diop Fall et Omar 😂😂😂😂😂😂 Diop dagua meilleur way
😂😂😂 Omar nenako na melni ngo ande😂😂
La complicité entre soxna et sa mère j'aime ❤
Duo entre omar Diagne ak iboulaye m’a tué sheuttt 😂😂
Bravo à toute l’équipe de xalisso badjo 👏🏻❤️
Vraiment 😂
Wallahi 😂😂😂
La complicité entre sokhna et sa mère j’aime 🥰🥰
C nice mais Les enfants doivent savoir leur limites. Kou neke yakhame sa matou lale. C pas Bien dencourager Les enfants a etre Des manipulateurs. Des fois c mieux de divorcer que detre ds une relation toxic. Tt es une continuation mo takhe sunu seye yi di ame problem en commercant avec Les belles meres.
Bly
Ani niey topou sokhna mou daww 😢Son stratégie de jeux c magnifique 😢 Evenprod tjrs les meilleurs 🙏♥️
Fekhel ba bouko essayer rkk
Essayer pour lan nonou 😢
Olala le duo mère et fille (boury et sokhna) je les adore voir ensemble 😍❤️♥️.
Yalna yalla maye diabot diou barke.
J'aime la stratégie de Sokhna mou ndaw pour la réconciliation de ses deux parents.L'honneté et la franchise de Ndeye Touty envers sa copine Maty Rose me plaît beaucoup.
Sokhna mou ndaw meuna limouy def😂quel talent
Le "Woyyy" de Ndiawar ak c'est bien Boury 😂😂😂😂😂 nonnn Ndiawar tu nous heureux.Mr c'est tres bien
Commentaire bi la don weur😂😊
Très bien
Legui dal boury defa beugat 😂lou nekh lay done chez ndiawar 🎉🎉omar c’est un fou nanditè😂😂😂
Boury deh dou question mbeuguel sax mais c’est la situation
Yaye Dior wakhna lou ame importance néna ndiawar li nga ame mako liguéy sa keur baye dama heuye nga guotou toujours niounane liguéyou ndeye na féke dom ame diome ndeye yépa liguéy na dom ame diome rék vraiment evenprod mention spécial à vous yéna gui diangualé lou ame solo yéna dékalate théâtre lepe c'est la réalité sénégalaise pas de fiction diarama 🙏🏾😍❤️❤️
Soda Mareme dina soukki Ndiawar bambou sett... "document à signer" nenah yeehhh😂😂😂😂
Han kon degg ngako😂😂
Wakhou Mala détt car elle en est capable 😂
Dafa lerr😂
Romb souki😂😂😂
Lolou bakhna si mom AK yayam WOR bakhoul ta dagno WOR boury
La relation de ndiawar et sa fille me rappelle celle que j’avais avec mn défunt père yalnako yalla yeureum t xaréko adjana firdawsi 😭🙏
Amine ya rabi.massa
Ndiawar lomou wax ni c'est bien 😂😂😂😂
Com batika am détt😂😂
Amine yarabi
Yalah na sounou borom yeureum nieup
Amine
Touche boo def ci «👍» yalna doon Salaat sur notre Prophète Mohammed (PSL) à ton auteur.
Sallahou alla Mohammedine ❤ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa Salim ❤ allahuma sali halal massoufi bil karami wal djoudii ❤ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa alla alihii wa sakhbihi wa salim
Sokhna est trop mignonne en voulant réconcilier ses 2 parents.
Kouy avancer 13min 😂😂😂pour setan 😂😂 j'aime la complicité de sokhna et sa mère boury 😂😂❤
Mgui ni 😂
Youkou ci 18s
No les pubs c abusé quoi
Khana mann😂
Kon dou man kase😅
Ndiawar Très bien, c'est bien 😂
La complicité entre Sokhna et sa Maman waouh ❤❤
Oumar et son oncle 😂😂😂tamit
Chapeau à vous 🎉
Des coeurs pour notre Prophète Mohammed psl❤❤❤
Au Sénégal fébar bima gueuna ragal moy fébarou xel par ce que aux yeux des gens do wer mouk même sou yalla deffé lepp dagne thi yaw aux regards des personnes amna lou dess bagne nañou ko dof dou wer lañouy wakh ce qui est déplorable fébar la comme fébar yeup daffay wer
Que dieu nous assiste😢
Amine ya rabi ❤
Bilahi dagnnanla doufdou werr rab yih rk gnooy djeul conger
Sama yaye dafa def accident nianal lenko yallah yeukeuti ko famou teude prier pour elle svp😭😭😭❤
Yalla na wéer ak diamou 🤲
Yalla na wer ak diamou ❤❤❤
Yalla na werr aak diam
Yallah na weer ak diamou
Yalla nako yalla yeukati ak diamou bamou dèllou wate thie ay mbireum si barkèp borom Touba touff touff touff sama xôll lako tibbè nakk ndax yaye dafa foore ءامين يارب العالمين 📿🤲🏽🙏🏽
Soda Marème est très intelligente elle a tout fait pour gagner la confiance de ndiawar, écarter Seydou pour mettre son plan à exécution. J’ai jamais eu confiance en elle à propos de l’entreprise, alal ndiawar bi yeup lay récupérer
Bien vu
L'allure de Bouri on en parle ou pas. Oh quelle élégance 🎉🎉🎉
Ndiawar ak c bien c très bien 😂😂😂😂c’est une longue histoire 😂😂
Bilay 😂😂😂
Boury tmt ak yabaté bay beuga dé c'est une longue histoire 😅😅
@@yayemayelatmbao5442Billy ctrés bien kayi😂😂
Deugueleu deh
@AstouGaye-k9z vrai comédien la😂
Ndiawar doit faire comme moi,pour OBLIGER sa mère et Boury à faire la paix..En effet, avant, ma sœur Aïda et ma femme Queen Bineta, n'étaient jamais d'accord. Quand j'en ai eu marre, j'ai demandé à un ivrogne un peu de bière que j'ai versée sur ma chemise. Arrivé à la maison, je "tare tari"😂 et chante comme un ivrogne " wooye Birima, foumou yéndou ma yéndou fa, yèndo nane né, bani tateu. Hé boy maman , wakhale boy Aïda ak boy Binette, gnou djoubo". Maman dit en pleurant " c'est votre faute, mon fils n'a jamais fait ça". Aussitôt, ma sœur et ma femme s'embrassent. "Gnaf" personne ne veut un frère ou un mari ivrogne😂. Depuis lors, "djameu" la paix. "Légui kou dékoné rék, ma déf tateu"😂😂. LOVE
C'est Intelligent ça 😂😂❤
Je cherche toujours votre commentaire 😂😂😂😂
Commentaire Fata lay weur mane miii😂😂😂😂
Fooy inspirer woo
😂😂😂😂😂
😂😂😂😂
Guirr yalla pour une première fois guénn mayma ayy j'aime 😂
Wa Sokhna yaw sonoo si diabanté bi 😂😂😂😂😂😂 Wa ma deguoul wala yaye Dior nena yalla na am delousi bouryyy😂😂😂 niawww
sokhna bou mak dafa seyetané rék mais dafa beugue omar diagne ❤❤❤
Tonton Sanéx yalle nafi yague té ande ak weur ak keup kou wah amine
Amine yarabii 🙏🙏
Amine ❤
Amine 🙏
Merci Ndiawaar tu nous donnes l'exemple comment parler avec Ta Mère
Jërëjëf Ndiawaar Diagne❤
Xaliso la série qui n'a jamais perdu sa valeur 🎉🎉 yalna niép ame diame barké seydouna mouhamed
Amin
C'est vraiment beau de voir ses parents ensemble ❤
La beauté de boury machallah ❤❤❤
Aka nekhone ma nék dallou yonénetu bu psl ❤❤
Bilay yaw thiey Sunu wadji sallahou alla Mohammedine ❤ allahuma sali halal massoufi bil karami wal djoudii ❤ sallahou alla Mohammedine
Ndiawar bilay mo néxal serie bi😂mane déh c très bien bi momay raye😂😂😂
Ndiawar c bien 😂 je demande si vraiment vous faite confiance a soda maréme prck moi c no boury nak khalé yi késsé takhouniou nga bgue délou ms tu aimes ndiawar 😂c très bien soxna bou ndaw elle est forte walay j’aime son talent 🎉❤soxna diagne sik na ms elle aime ses enfants ❤encore une fois chapeau l’équipe 🎉
Soda maréme mii bakhna dal mougui nane kharal ma indi document gua signé ko mBadou loumay khalate nakh théâtre bii xaliso lo toudou mbadou dieule bien ndiawar bii yeup
Bilahi nio yam dafa beugue sathie khaliss bi
Kou gueum soda bopam la togual dina rateu ndawar diagne bamou set sou boury guawoul nieuwal
Soda mareme mane personnellement massou mako wolou mais bouguou meu wone tela wahh
Ce que Soxna bou ndaw a fait pour sa maman m'a tellement touché et m'a fait rêvé en même temps. J'aurai tant aimé sameu dome bou goor bi dioubolé m avec son papa.Mais c'est encore un bebe.
Héyoo ma belle fais le premier pas si tu es toujours amoureux adouna amoul solo wakhtane len ak vos parents si lui aussi t’aime toujours
Geumeul sa bope rek djiguene bou beugeu day gnak diomdef boul fale
Ndaysane yallanako yalla délo si diam divorce bakhoul tè bou sa dôme mangue gua koye kham
Sk douma nieuw dioubolé Lén nop ngako
Oui je l'aime, je suis amoureuse de lui mom la xam, c'est très difficile de passer à être chose. J'ai fait tout ce que j'ai pu pourtant mais malheureusement j'ai pas eu gain de cause.
Nianal léne m rek,mon foyer me manque
Omar Diagne ak nidjiaay dji ray nagne ma😂😂😂 comme koukay kidnappé dh😅
Chapeau à Sohna bou ndaw 😊 Boury j’aime sa manière de faire tout pour le bonheur de ses enfants
On en parle de Ndiawar avec c’est très bien c’est bien 😂😂
Ndey Touti c’est pas seulement une meilleure sœur mais aussi une merveilleuse amie qui conseille bien 😊
Omar ne pas si fou que nous pensons il fait tout pour obtenir ce qu’il veut c’est un fou intelligent 😂
C’est le commentaire que je cherchais 😂cheu ndiawar vrai comique la
Omar diagne dofoul dh😂😂😂😂😂😂
C. C. C.
Cc. C c.
Ndeysane Masha'Allah Boury gneuw feek sa djeukeur gnak leep nga recommencé waatt à zero ak moom ❤😊 vraie regal 😮
La complicité entre soxna et sa maman est vraiment extraordinaire ❤et genre soxna yii dagno bakh si parents you divorcer nakh dou bayi ,c’est une bonne sentinelle 😂
Kou content si Sokhna mou ndao rkk lalal ❤dama dée man si wakhtaanou Iboulaye ak Omar Diagne doff bou am khel😅 Ndeysan Boury chapeau à elle 🎉🎉🎉ele veut retourner avec son ex mari a cause de tes enfants thiey l'amour maternel amoul morom bravo a nos mamans ❤
Soda Mareme Mbadou da beugue doreu Ndiawar diagne keyy 😢seutteu BOURI GAWAL ❤❤❤
Commentaire bi ladone khar Soda Maréme a gagné la confiance de Diawar et elle veut en profiter pour l'arnaquer
Ndiawar c’est très bien 😂c’est bien 😂😂
Képeu kou beugue Omar Diagne tané❤takk Maty Rose rék lalal j'aime ❤❤
Avec Xalisso votre cœur bat plus fort ❤❤❤
Wlh
Diawar ndiang non role baol baol bi bimiy joue amol nomko manéwol machaalah mom khamna lo way wah adak mom😂😂😂 mom do réro ak kenue😂😂
Wa mani jspr dou man rek mafi Avancer pub dee 😂blhh setane série si telephone dra dakouko youkhouu haleii doula terei deg wakh dji commentaire en même temps k la série doula déconcentré bangay merr Di yeg😂vive even prod vive you tube 😂
Yaye sama ndaye diké 😂😂
@matybeye837 kon nehna😂
Dieureudieuf Serigne Touba❤️❤️
Dieuredieufé Borom Touba ❤
Diadief ❤
Koumay santelé Serigne Babacar sy Malick borom Bone caré bi ❤❤❤❤❤lalal cœur ❤
❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ yalena diamou yage siyawee 🤲
Amine inchallah 🙏 et toi aussi
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉
Sonko et diomaye Allah vous protège ❤🎉 0:14
Allahouma Amin 🤲🏽❤️
❤🎉 34:26 @@fantasagna4076
Sokhna boundao est vraiment génial 😂😂😂😂 j'aime ce qu'elle fait pour réconcilier ses parents 🎉🎉🎉🎉 sa relation avec sa maman boury c'est trop chou ❤❤❤❤❤
Boury est une femme très intelligente qui est capable d’apprendre de la vie à ses enfants ❤🎉
Yalnagnou fi yalla bayi bagnou sétane saison bi bamou diékh si diamm inchallah 🤲🏼
Amiine yaa raabii ❤
Amine
Amine
Amine inchallah
Ndiawar moy soda Mareme, Soda Mareme moy Ndiawar c’est bien😂😂😂
Yalla gua rousse lo Say none si barke seydina Mohamed psl 🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
Non Ndiawar Diagne Motakhe begue Série bi brome c'est bien 😂😂😂😂😂
Le mari de sokhna la grande, souffre 😂😂😂😂😂😂. Tout le monde lui manque de respect, même Omar qui est fou😂😂😂😂😂.
Tu as remarqué
Kou banque com man lalal Jaime 😂❤
Mangui ni soumaye tite di 🤣 dé
Soxna mou makk, elle est mauvaise mais si elle réussît à faire guérir Omar. On l’aimera 😂🫶🏻
Depuis la Mauritanie 🇲🇷 ❤
Luxsar 5e 6e ah ha tavarazaine😅😅😅
@ mauritanien 😂
Nous sommes la 😊
Ndiawar il me tue la façon quand il dit ‘’ très bien ‘’ 😂😂😂
Keur Diagne Diagne yi nekh na million yomb na si gnomm 80 ,200 millions 😅😅😂
J'aime la façon donc boury est près à tout faire pour le bonheur de ses enfants ❤❤
😂(aetrdesdqwcvtyuiophjklmbvn'm❤❤❤❤❤
Première commentaire ani mouride yi 🥰🥰
Man la
Guéné niousi dh 😂
Kan momaye santèle seydina Mohamed sws lalale cœur bi❤️❤️
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤😊
❤❤❤
Faux raccord bou ndaw, Boury a dit sa fille de prendre ces bagages ensuite elle a dit à son Père kel va l'aider à faire ces bagages. Mais elle est partie avec son père sans bagages. Souma joumé aussi ngen wahma
❤❤❤
Lire katou commentaire yi longue vie à vous ❤
13:20 c’est le début du film. Merci 🙏🏾
Losi xamoul bala ma xol seri commentaire lay nieuk xol fi Seri commencé
Iboulaye ak diabar dji sheuttt 😂😂😂😂😂😂😂😂
Mane Ndiawar la beug 😂😂😂😂
Des cœurs pour notre prophète Mouhamed ❤
❤❤❤
صلّى اللّه عليه وسلّم ❤🤍
Arrêté oh
❤❤❤❤
❤❤❤
Diawar da meilleur lougnko conseil mouné très bien 😂
La class de Boury Allahouma barik❤❤
Ndiawar ak c bien c très bien une longue histoire 😂😂
😂😂
La meilleure maison de production de sénégal respecte tellement l’heure de t ses téléspectateurs vraiment vous êtes les meilleurs ils méritent les 5M avant 2025😊❤🙏
Bilay 🥰🥰🥰
Man niom rek lay top
Yalla na nieup am diam si barké seydina Mouhamed ❤
Amine inchllh
Amine way
Amine ya raby
Soda merem tass famille moko takha Diogu dh le retour de boury way💪❤️❤️❤️❤️
Wa yaye Dior tmt limou beugue tmt hé sokhna la beugue mane😂😂 weuy Omar ak oncle bi 😅 diawar c'est bien c'est très bien
Yaye Dior da beug boury nieuwat pour défanté ak soda maréme 😂
La beauté de boury❤❤❤
Waou❤❤❤❤❤Boury
Machallah ❤❤❤
Elle dégage la classe machallah
Bilae Damako beugue❤️🥹
La série qui n'a perdu sa valeur 🎉❤
Couple Sokhna Ak Ibou Fall dh kene wakhou si wante nekh nane trop lolene nekh waxantè 😂😂
Domou Badiane ak domou nidiaye...😂
Seye ak sa domou Nidiaye dafa néx 😮😂
Yenagui wakh ms. Khalé bii limou woy sii xaliso bii doynawr 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Pauvre Diawar 😂😂 trop gentil comme moi mais trop gentil trop con😂 c'est bien très bien
@@Hassane221 trop cupide weuyyy😂😂😂
Soda Marème ngui signèlou dh😂😂😂 aah bamou soti xaliss bi mom douko reuth dh
Serigne Salihou sa yaye amatina ndam ❤ anh soda Maréme document bigay signé lo ndiawar lanla😂
صلوات على النبي كل كم ❤
Monsieur c'est bien c'est très bien 😂😂😂😂 ndiawar way
Yalla nafi yalla bayi sunu maman ak sunu papa basi kanama kanama kanam si barke s touba🤲❤️❤️❤️
Yalla na dioulit ak chrétiens yeupp dém Aldiana 😊
Wakhal dioulitt rekk yaw😊
Lolu manol nékk
😂😂😂😂
Ahhh iow tmt neil amiin tk@MbendaMbengueMbengue
kouthi beugue dieukeur wala diabar thi att bii lalal j’aime gaw 😂😂
Sokhna mou ndaw meune role bimouy jouer ❤❤❤😂😂😂
bilay bien joué
@@AmyThiaw-se1qkki kay takhna ma ame envie neck place sam sax 😂😂😂
Sama khel tey na ci soda Mériem dé 😂😂😂😂😂❤❤❤
Ndiawar ak ay phrase sam " c'est bien très bien "😂😂😂
Yalla na ousmane sonko Am ndam thie Sénégal AK Liko wérr Amine
Amine AK koko wakh
Amine 🙏
Amine yarabi
Sokhna bou ndaw coumou diakhal lou mane ni diakhalnama trop cou d accord beusal j'aime
Khaleibi dieulna tourondo wam finiiiii😂😂😂
Gnun niepp daccornagn si
Mé sincèrement Maty rose a un cœur d'or
J'adore ❤soxna et la complicité avec son papa❤❤❤
Sokhna aka grawe 😂😂sene coup bi dalna Boury déloul waye ❤❤Sokhna mou make ya seytane loutakh gua bagne Boury