Mourtalla regrette: "Daniouma garantir victoire Ama Baldé motah ma changer sama pronostic..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 18 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 159

  • @Gorgui-b8r
    @Gorgui-b8r Рік тому +45

    Moi je n’ai pas compris comment on pouvait donner Ama favori devant Modou Lo. Mane Modou Lo Tass ne sama yakar be tayi. Ce gars est un sportif confirmé, une vraie machine de guerre. Sport mom kounek moune ne gagné mais faut être objectif. Bravo à AMA, un vrai sportif très fair-play

  • @bouba934
    @bouba934 Рік тому +6

    le gars en chapeau j n t connais pas mais vous avez raison en tout faut avoir la foi dans la vie it is the first machallah , Modou Lo hors mis cette mentalite de boycotter l'aspect mystique africain cela prouve que MODOU est aussi un professionel , la preuve cest un element de coach Diabong , un monsieur inconnu de chez nous mais un vraai savant de la boxe

  • @cheikhmbackesyll9838
    @cheikhmbackesyll9838 Рік тому +17

    Wayy mourtalla danou gua wayyy diokho wone modou lo dara

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 Рік тому +8

    Thiey modou Lo moy champion 💪🏾👊🏽👑❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @Dieng-vk6if
    @Dieng-vk6if Рік тому +10

    Mourtala sa première analyse dafa pertinent mai après nga yakh ko mai kou kham lambe nga

  • @Reum-
    @Reum- Рік тому +5

    wadji yakk lamb j niit kou gorré la nit kou beug nitam té dou triché il s'est mis à la place d´Ama kou gorré kou beug guissatoul wone dara ndakh beug Ama vrai kharite la chapeau à ce mec

  • @nafisene5335
    @nafisene5335 Рік тому +16

    Bo leen moytouwoul modou Lo dîna yagueu Di leen fenlo

  • @papecisse6000
    @papecisse6000 Рік тому +13

    Mortalla Guissone n’a lamb dji mais dafa khawa faral ama. Motakh mais mortalla gnèmè woul modou Lo

  • @tamsirndiaye266
    @tamsirndiaye266 Рік тому +6

    Khana guemoo alkhourhanoul Karim
    Ayatoul kourssiyou loume menoul amoul

  • @abousoumare3345
    @abousoumare3345 Рік тому +7

    Beuz dieuleule ouza 2 borom lamb koula né yako kham néko bayil ba dimanche

  • @arfangsenghore3993
    @arfangsenghore3993 Рік тому

    Thanks beuse

  • @abdoulayeniang2511
    @abdoulayeniang2511 Рік тому +17

    Mourtalla sa première analyse moye bi Modou défé open presse guissone nga lamb dji mais après nga dawal féme ndanane nga nake

  • @laminefall3240
    @laminefall3240 Рік тому +6

    Bilahi Ama Baldé la faralone mais yakalna bopame

  • @boubafall1014
    @boubafall1014 Рік тому +1

    Mourtallla nelaw gua nak 😢

  • @PapeOusmanePapaOusmane
    @PapeOusmanePapaOusmane Рік тому +6

    😂😂😂mourtala tay dafa danou 😂ndakh genrou fadam gui

  • @bayesarr5129
    @bayesarr5129 Рік тому +9

    Sen changement de discours yi moy wané ni dounguene ay analystes meuno nek analyste beug nek guissané

  • @Enzoshifow
    @Enzoshifow Рік тому +6

    Man fadam moma béteu nga ni expert nga mais man j'te considère com chroniqueur tout court mouhamed aly ndiaye kay wakhat linga wakhon Mak dou waat si ay thiakhan

  • @KindyDiallo-q7k
    @KindyDiallo-q7k Рік тому +3

    ❤❤vive le roi ❤❤

  • @libasselahi
    @libasselahi Рік тому +6

    Gathié baxoul si makk khamo dara si lamb lepp si mystique ngen ko tekk

  • @ibrahimakane3940
    @ibrahimakane3940 Рік тому +13

    En lutte pure, Modou Lô est trop fort par rapport à Ama. Le clan de Ama misait uniquement sur le mystique. Malheureusement le mystique n'est que mental et Modou Lô est un maître à ce jeu.

    • @yannly531
      @yannly531 Рік тому +1

      Ligga wakh rek'ay dëgg. Amoul lénéne

  • @boubslo7905
    @boubslo7905 Рік тому +4

    Ama Khana robot là il est programmé lane moy sou arrièré lepam dey yakhou😅

  • @doudodieng476
    @doudodieng476 Рік тому

    Mourtalla ioe mom franchement kou xam lamb nga yalna Yallah Yokou Mashallah Vive le Roi Xaragn Loooo❤🎉

  • @laminefall3240
    @laminefall3240 Рік тому +2

    Boul fiii doulate dé😂😂😂😂😂

  • @bouba934
    @bouba934 Рік тому +4

    mourtalla sport en general amoul favoris dagnouy ndiorte rekk di waxx sport dafa complexe trop motaxx jeu de loterie ci sport rekkk la amme ; senegal 2002 bimouy gagner esk mo meune france pourtant non mais le sport nest pas les maths

  • @lahadboukharagnelo6707
    @lahadboukharagnelo6707 Рік тому

    Bilay modou Yenn nieup la Bert liguen donn wakh yepp sakh lamb dji demewoul nonou Kendou x Lo ❤️🫶

  • @profcoly6085
    @profcoly6085 Рік тому +2

    Pourtant mourtalla wakhone neu qualité modou lo yi wayé aprés dernier joyrs bi gua nélaw ndakh boukhaba pikine yi niola nakh

  • @Mor-gh1cm
    @Mor-gh1cm Рік тому +6

    Mourtala lamp da ñoul érreur yi boum là dalati

  • @alassanendiaye3447
    @alassanendiaye3447 Рік тому +5

    Mourtallah t'avais vu juste mais t'avais changé de version à la dernière minute.
    Fadam toi, tais toi, tu n'as rien vu. Je me rappelle tu avais dit Ama battra Modou Lo en 1 minute 45 secondes.

  • @cheikhgaye8942
    @cheikhgaye8942 Рік тому

    Mouhamed aly ndiaye fane la nekkk

  • @abdoulayeniang2511
    @abdoulayeniang2511 Рік тому

    Déme léne xole suma commentaire li buzz posé Mourtalla la commenté si deuxième vidéo Mourtalla bi

  • @laminefall3240
    @laminefall3240 Рік тому +5

    Daguén ragual wa pikine rék tapét yiii😂😂😂😂djeul léépe djokh ko Ama mélni modou lo meusoul béuré nopilén

  • @moussadiagne4402
    @moussadiagne4402 Рік тому

    Ce gars n’a rien à dire neu d’accord record rek et passé à autres choses

  • @galassefaye4587
    @galassefaye4587 Рік тому

    Nom beuz yaye bandit

  • @laminefall3240
    @laminefall3240 Рік тому +1

    Daguén rousss vous touss

  • @abousoumare3345
    @abousoumare3345 Рік тому +3

    Fadam défaite bi monko diap

  • @azizngom8741
    @azizngom8741 Рік тому +2

    Louniouy wakh rek kou beuri kharite nafekk gua moy bougo kene merr ko wetol wakh ko loumouy beugue degg, akk nite bo khamner lou nieuw guaner amguasi xam xam do diokk si gathier , lou ouza 2 di wakh rek kouner ma kham lamb neko ba dimanche,mourtala lo wakh mouner moko feker moko kham mtakhite do diog si gathier so nopiwoul

  • @azizdiouf898
    @azizdiouf898 Рік тому +3

    Li mome boumou leu salati dègua lekk sa bègnè 🤣🤣🤣🤣dalalone gua sama xèl bii yeupp😂😂

    • @AmyFaye-lf4iq
      @AmyFaye-lf4iq Рік тому

      🥛🥛🥛🥛🥛🥛🥛🥛🥛🥛🥛

  • @fafandao2571
    @fafandao2571 Рік тому

    Ana pa bi Buzz😂😂😂😂

  • @boubslo7905
    @boubslo7905 Рік тому +3

    Modou Lo dafa attaque après

  • @benjaadams9958
    @benjaadams9958 Рік тому +1

    Vraiment c'est domange senegal deugeur fit wax sans xam xam danu guenatsi japé gnilay deglu ay dof

  • @demboussotall3488
    @demboussotall3488 Рік тому +2

    Kone dé gris 2 mooy serigniou lamb😂😂😂

  • @ndongodaara
    @ndongodaara Рік тому

    Mourtalla dou danou kw 😁🤣🤣🤣

  • @mamadousy6312
    @mamadousy6312 Рік тому +6

    😂😂😂moutalla borom bégné bi

  • @silencieuxbouyant9687
    @silencieuxbouyant9687 Рік тому

    No mourtalla yaw daga kham lamb Machallah c normal car lamb gnane dassi bokk modou super ndanane le

  • @BassLeye-tc8ne
    @BassLeye-tc8ne Рік тому

    Bilakh Lou ler la mbess wakh

  • @marcusmouhamed
    @marcusmouhamed Рік тому

    Mourtala demakoy comprendre parsk gnu beuri degno ragal aspect mystique bi coté modou lo

  • @BassLeye-tc8ne
    @BassLeye-tc8ne Рік тому

    fadam la dh ak nième yalla

  • @taphadiene
    @taphadiene Рік тому

    Mortalla wakhofi dra😂😂

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Рік тому +1

    Tu n'as pas démérité mbeur leu champion la billahi lamb la rék

  • @BassLeye-tc8ne
    @BassLeye-tc8ne Рік тому

    Talla kay am amon fi loy wakh pas ka ioe Say wakh ay Serigne ka ko tegue dii wakh baguan

  • @moussathiambayefall1013
    @moussathiambayefall1013 Рік тому +2

    Mais modou lo dafa tackoul galadje rek mais andina misstiq bo douy

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 Рік тому +1

    No don't say modou lo ,have to stope wresting😡

  • @Diantal
    @Diantal Рік тому +9

    Mourtala linga ligueyone yep si yi passé ak yeulé passé lep yakh ngako si sa révélation bi ...yaw warone nga depassé niveau bouniou lay influencer

  • @Fitserigne
    @Fitserigne Рік тому +1

    Mourtalla fadam moko wayadi Lo ak buzz gnoko wo téléphone pour wakh limou wara wakh thi live

  • @nguiranealiou776
    @nguiranealiou776 Рік тому +4

    Mouhamed Ali ndiaye aka meun fennn loo wahonn😂😂😂

  • @mamepathe4618
    @mamepathe4618 Рік тому +1

    Ahmada wakhone nga lepp gayi dila rétane

  • @Killer-z1u
    @Killer-z1u Рік тому

    Père ali😂😂😂😂😂😂

  • @atoumaneniasse4854
    @atoumaneniasse4854 Рік тому

    Mortala lou leer nga wakh ❤

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 Рік тому +1

    C vraix que mourtalah defende tout le temps les avantages de modou lo mais lamb renou niamila kene khamoul foumouye dame

  • @papealiounedione1995
    @papealiounedione1995 Рік тому

    Non Moutala kénn douko ray 😂😂
    Modou lo kassé Bilakhi
    Galathie amtoul

  • @BassLeye-tc8ne
    @BassLeye-tc8ne Рік тому

    Bay woul niane dh mogui nian dh

  • @MorWade-yq1lr
    @MorWade-yq1lr Рік тому

    Mourtala yagici lambola

  • @mbayefaye1261
    @mbayefaye1261 Рік тому +1

    Ki war nga rouss tok fi di wakh

  • @lyassane5993
    @lyassane5993 Рік тому

    Mourtala Mane damako wédi ba gaw

  • @ModouLo-eg9ij
    @ModouLo-eg9ij Рік тому

    😂😂ah mortala yaw kay wédinala man yaw rék ladon topou Pour ma sportif nga 😂😂

  • @mordiop8192
    @mordiop8192 Рік тому

    Grand Ahmada bii mongi wakh Lou am solo

  • @toubapneu5102
    @toubapneu5102 Рік тому +4

    Me mourtalla wa khone Na 4 apu la modou dii danne Ama

    • @durkio5486
      @durkio5486 Рік тому +1

      Mais vendredi daga wakh que modou amoul benee chance ci lamb dji , t louma diakhal gayi daniouy diokh khekh bi modou , diokh beuré modou après ngene beugu wakh que ama moy dane

    • @PapeZidane10
      @PapeZidane10 Рік тому +1

      ​@@durkio5486vraiment ñii weru ñu xana kon thiii mystique lañkoy ték😅

  • @BassLeye-tc8ne
    @BassLeye-tc8ne Рік тому

    Bilakh wakh ka degue dh danko bess deg rek kay wakh

  • @ousseynoutoure518
    @ousseynoutoure518 Рік тому

    Mourtalla Dafa wakh si modou lo lou graw bobou lako xam apres deux jours avant le combat mounane sama beignet bi sakh doumakossi tegue yw nopil bayil wakh😂

  • @FallouNdir-q7b
    @FallouNdir-q7b Рік тому +1

    Mourtalla khamoul dara

  • @lahadboukharagnelo6707
    @lahadboukharagnelo6707 Рік тому

    Mourtala damako wedi pour man dafa kham lamb mes khamoul touss 😂😂😂😂😂😂😂

  • @bouba934
    @bouba934 Рік тому

    mourtalla dagua werre koula waxxe xameuna lambb rekk neko bayil beu dimanche

  • @galassefaye4587
    @galassefaye4587 Рік тому

    Fenial nga wadji murtada da danou

  • @BassirouSamb-oe6sh
    @BassirouSamb-oe6sh 6 місяців тому

    Kouy cheikh Niang mbeur bou yakk😅😅😅😅

  • @modoucisse9427
    @modoucisse9427 Рік тому

    Beuz três inteligentes

  • @PapeOusmanePapaOusmane
    @PapeOusmanePapaOusmane Рік тому

    Tegal cheze bii dafa moy 👀

  • @medounetalibebamba6432
    @medounetalibebamba6432 Рік тому +2

    Fadam nopil yaw amo lo wakh vraimment

  • @CheikhFall-y3n
    @CheikhFall-y3n Рік тому

    Wa mourtalla ani bousou bégné bi😂

  • @mbackethioune4385
    @mbackethioune4385 Рік тому

    Aussi buzz wowal pere malan amérique na nieuwat si live biii

  • @ndoyeabdoulaziz
    @ndoyeabdoulaziz Рік тому

    😂😂😂 mourtalla nanil ndokh

  • @CheikhNasr
    @CheikhNasr Рік тому

    Ya'w amo lo wahe hamo dra

  • @silencieuxbouyant9687
    @silencieuxbouyant9687 Рік тому

    Coach😂😂😂

  • @Elhadji2187
    @Elhadji2187 Рік тому

    Ooeee bayil beuri wah dagua rouss rk dieul affaire yi diko tekk si serigne gnouy wah guay insister nékté liguay wah hamo si d'ara

  • @milkiidiouck8344
    @milkiidiouck8344 Рік тому

    Fadam nopil seytane nga

  • @amuskogroup3438
    @amuskogroup3438 Рік тому

    Lamb ken hamukoh

  • @elhadjimodouthiam5566
    @elhadjimodouthiam5566 Рік тому

    Mortala dafa bari wakhe réke waya khamoul dara mane bima dégé mounè kouteke sa keure si modou lo bou altiné dinga louyè dji damanè ki dafa dofe

  • @ibrahimakane3940
    @ibrahimakane3940 Рік тому +2

    Ce gars est nul. Quelle est la place du mystique dans une bonne analyse sportive ? Ce gars qui connaît très bien Modou lo s'est seulement fié aux marabouts. Il est discrédité et n'est plus un analyste. Un bon croyant ne résonne pas comme ça. Se faire influencer comme ça par un simple mortel. La plus grande force de Modou Lô, c'est son mental. Son professionnalisme est à enseigner dans les écoles de sport. Moutalla est trop faible mentalement.

  • @KheuchMbaye-c5j
    @KheuchMbaye-c5j Рік тому

    Modou lô kérok bimouy beurek bombardier dafa dieul coup bouko sonal mai dawoul guene té wakho si lolou

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Рік тому

    Mortalla lou leer nga wakh

  • @HerveBasse-in1lv
    @HerveBasse-in1lv Рік тому

    Grawoul dina dann boy niang après mou bayyi

  • @MomoyFayy-ly8rv
    @MomoyFayy-ly8rv 8 місяців тому

    Vraiment senegalais yi yèwoulèèn buzz mi da dèm jangui ba parè di business sèn kaw lamb amoul bène importance

  • @khadimndiaye3221
    @khadimndiaye3221 Рік тому

    Mourtala yaw mome daguawara noppi..lou ler ngua wakhon ngor nak thia wakhdia li nak moy Senegal...bou ama balde danon ...mourtala mii rakkou yalla de lay def boppam ...mourtala modou bayi lamb..haa noooo yaw bayil wakh..ba pare!!respectel senegaleyi..tala noppil....😂

  • @tidianeagne5497
    @tidianeagne5497 Рік тому

    Yow fadam Rasoulilah ak lamb gaye tekelo

  • @ibrabadiane4233
    @ibrabadiane4233 Рік тому +3

    Bilahi bim wakhè la titone ndakh ki si serigne lako tegone mais liy Souba yalla rek moko xam

  • @BassLeye-tc8ne
    @BassLeye-tc8ne Рік тому

    Alkhouran rrk la Yakar Modou lo diambar là

  • @babacarseye3464
    @babacarseye3464 Рік тому

    Mourtala danou ga ya takhe ma niak sama 2rou

  • @ibrahimadiop3754
    @ibrahimadiop3754 Рік тому

    Mourtalla gor la gathier la meunoul supporter😹

  • @mohamedfall1199
    @mohamedfall1199 Рік тому

    Mourtala vraiment tay danga danou boul Bazin si wakhi sénégalais dmal aksa khél

  • @abdoulayelo3541
    @abdoulayelo3541 Рік тому

    Mourtala khamo dara

  • @Blackpower109
    @Blackpower109 Рік тому

    Sa revanche avec Balla Gaye mo ko déssé