Balla Diouf et Assane Ron detruisent Siteu : " Dou nii laniouy, dafa daw "

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 29 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 132

  • @MaraGaye-t7f
    @MaraGaye-t7f Місяць тому +103

    Bonjour mes amies mani nioune gni ande ak kharagne❤ souniou khole da fékh ndah danio nieuw wane Sénégalais yii ni siteu dou tarkinda ms dawkinda la😂😂

    • @PinzipFromdaO
      @PinzipFromdaO Місяць тому +1

      @@MaraGaye-t7f mais danako deh 😭😂😂

    • @MaraGaye-t7f
      @MaraGaye-t7f Місяць тому

      @@PinzipFromdaO foumou ko danée

    • @PinzipFromdaO
      @PinzipFromdaO Місяць тому

      @@MaraGaye-t7f stade arena 😂

    • @MaraGaye-t7f
      @MaraGaye-t7f Місяць тому

      Ioe khana novelas nga sétané combat bii🤣🤣

  • @maragueye8207
    @maragueye8207 Місяць тому +15

    Balla diouf sportif deugue leu❤❤❤❤

  • @badaraba6977
    @badaraba6977 Місяць тому +26

    Balla Diouf un fin analyste de la lutte

  • @paparidialendiaye1543
    @paparidialendiaye1543 Місяць тому +14

    Abou ndour ay questions you intéressant lay poser machallah

  • @thiam8642
    @thiam8642 Місяць тому +12

    Le mot daw 🏃‍♂️🏃‍♂️😂 la mougnioul mougn😂😂😂😂😂

  • @ndiawlo4875
    @ndiawlo4875 Місяць тому +40

    Modou lo dou morou siteu yénaka tay😂😂😂😂

  • @MamadouGano-f6m
    @MamadouGano-f6m Місяць тому +21

    Merci beaucoup balla .
    Situé da daw.

  • @salifba7251
    @salifba7251 Місяць тому +2

    Balla Diouf mo gueneu ha lamb thij Sénégal quel analyse

  • @PatheGueye-rt7vv
    @PatheGueye-rt7vv Місяць тому +4

    Balla Diouf vrei sportiv le très pertinente

  • @ModouDiop-x5k2s
    @ModouDiop-x5k2s Місяць тому +15

    Modou Lô kassé ❤😂😂

  • @abdourvms6034
    @abdourvms6034 Місяць тому +36

    Bilahi MXLÔ Mô attaqué 20 mn yeup Lac 3 daw 20 mn yeup 😂😂💔

  • @aboubakarkediadiop
    @aboubakarkediadiop Місяць тому +2

    Vraiment sites mi vrai raguale là Sénégal des fois do comprendre wakh léne siteu degeu loumou déf ci combat bi loudoule daw ak wakh bou beuri félicitation Modou yaow champion nga

  • @jobehamidou6545
    @jobehamidou6545 Місяць тому +3

    Merci beaucoup balla true speaking

  • @AmCoulibaly
    @AmCoulibaly Місяць тому +7

    Vraiment balla tu es for

  • @ChambouléFM
    @ChambouléFM Місяць тому +3

    Modou Kharagne Lo ❤the Goat ❤ Seul 👑💯🔥

  • @superfoottv2277
    @superfoottv2277 Місяць тому +5

    Modou dal mashalla champion deug la koukoy dane faw nga indi lou ler nagn

  • @mbayelo6090
    @mbayelo6090 Місяць тому

    Bala tu es le meilleur

  • @tamsirsene6204
    @tamsirsene6204 Місяць тому +1

    Merci balla diouf deug pir ga wakh

  • @bapiskallo9134
    @bapiskallo9134 Місяць тому +5

    Serigne Ndiaye tongn ngagnou waro wone dem albourakh

  • @SYLVESTREKANKOLA
    @SYLVESTREKANKOLA Місяць тому +2

    Merci modou lô 👑👑👑👑

  • @MameSow-m7e
    @MameSow-m7e Місяць тому +5

    Modou lôoooooo ❤❤❤❤❤❤

  • @NDIOBOMBALLO-wi9dr
    @NDIOBOMBALLO-wi9dr Місяць тому +2

    Vive Modou lo 💯 Amine ❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉😊😊😊😊😊😊😊😊😊

  • @BoubacarDiop-q2p
    @BoubacarDiop-q2p Місяць тому +3

    😂balla Diouf tactik 4 5 2 mom fane lah âme

    • @Noface-o1d
      @Noface-o1d Місяць тому

      Balko dafa dioum😅

  • @mouhamadoulamine279
    @mouhamadoulamine279 Місяць тому

    Balla wagnill beine joueur

  • @KateChris-r9i
    @KateChris-r9i Місяць тому +2

    Mai pourkoi on montre seulement lépaule de modou ou est le tête de siteu et lautre bras

  • @serignesow6903
    @serignesow6903 Місяць тому

    Balla dioufff merci❤

  • @Matar-h2f
    @Matar-h2f Місяць тому

    Bravo modou lo❤❤❤

  • @ceesayceesay2530
    @ceesayceesay2530 Місяць тому +1

    Merci waay balla diouf linga wakh mooy deugue, modou lo poi bi yakhaloulko dara.

  • @Collzo-o8f
    @Collzo-o8f Місяць тому +2

    Sitteu mo dane soyez honnête et véridique

  • @Mbodji-walo
    @Mbodji-walo Місяць тому +1

    Na nieupp dém félicité Siteu👑ngén bayi yeufou nefekh yi ok
    Félicitations Yalmine❤💪🏾

    • @palayesall8792
      @palayesall8792 Місяць тому

      Bilahi wakhal donio sokhor ak contre ndiol mi rk

    • @Moustapha-s6x
      @Moustapha-s6x Місяць тому +2

      Yenn yeineu takhh sitteu niakk diom

  • @mariemethiam5861
    @mariemethiam5861 Місяць тому +1

    17:35 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @benzdictenobalegomis6139
    @benzdictenobalegomis6139 Місяць тому +1

    Modou Lo kessé 👑🎉🎉🎉❤

  • @PinzipFromdaO
    @PinzipFromdaO Місяць тому +1

    Siteu danako deh 😂😂

  • @abdouliefaal2916
    @abdouliefaal2916 Місяць тому

    😂😂😂😂😂😂Merci frère ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤👍🏻

  • @badaradiopkhassida1746
    @badaradiopkhassida1746 Місяць тому +11

    Aka ma amoon Yakaar ci Siteu mu déf limou wakhoon ci Signature ba😂
    Konn Modou dinako door bamu gnibi yaomal khiyaam😂😂

  • @laminebusquetscisse9316
    @laminebusquetscisse9316 Місяць тому +3

    🎉❤

  • @ebrimacham4239
    @ebrimacham4239 Місяць тому

    Siteu 🏃🏾‍♂️‍➡️🏃🏾‍♂️‍➡️🏃🏾‍♂️‍➡️🏃🏾‍♂️‍➡️🏃🏾‍♂️‍➡️

  • @franceamericanbullydogfami7992
    @franceamericanbullydogfami7992 Місяць тому +1

    C'est dommage pour une arène nationale les délimitations se font avec des sacs de riz😢

  • @Jeuneentrepreneurcheikh217
    @Jeuneentrepreneurcheikh217 Місяць тому +7

    Max mbargane ak khadim Ndiaye Nagne bayyii nakhanne thé bii thé wakh Siteu mouy deugeul boppam moo ngeunn daw yii, Siteu amna doolé meuna beuréé dou takhaw déf lim wara déf Mouy mélni thiak thiak nii😂

    • @ramasarr2108
      @ramasarr2108 Місяць тому

      @@Jeuneentrepreneurcheikh217 😂

  • @PapaDiouf-b1y
    @PapaDiouf-b1y Місяць тому +2

    Balla stratégie bokoul ak daw di guenn sakou yi gnemélenn deug gui

  • @BillycargOnjayy
    @BillycargOnjayy Місяць тому +2

    Waanee leen si règlement cng faan laniou bindeuh mbeur mi dafa wara niow dorantee ba danou wala daan le sport est un affaire d’intelligence mais pas de guerrier .. finalitee lamb moy daan tee siteu daleen daan parler nous du chute qui fait polémique que de s’appesantir sur le stratégie abordé par un lutteur

    • @ndenediagne50
      @ndenediagne50 Місяць тому

      Lou lère nga wah bilahi Senegal fene rek

  • @LassanaTRAORÉ-m5x
    @LassanaTRAORÉ-m5x Місяць тому

    4-5-2 bi momay rey 🤣🤣🤣🤣🤣

  • @MaodoKane-mw4yd
    @MaodoKane-mw4yd Місяць тому +10

    Siteu boppou sakh dafa lall sakou bi

  • @AmadouBacarNdiaye
    @AmadouBacarNdiaye Місяць тому +2

    Modou lo seul

  • @ousmanendiaye9579
    @ousmanendiaye9579 Місяць тому +5

    Siteu defna 4 appits dakh sackou bi genoux gauche siteu biniouy wax laloul souff moko yobbalei suivre len action bi bou bakh avant épaule M'dou Lô bi siteu cila def 4 appits après bimou yeukatei genoux gauche bi ci la yobbalei sackou bi yeuka ci walei sable bi hollen bou bakh

  • @LTkart
    @LTkart Місяць тому

    Cng doit doubler l'enceinte de l'arène pour les reculeurs😮

    • @ndenediagne50
      @ndenediagne50 Місяць тому

      Modou lo son combat contre bombardier dadone daw 😂

  • @abdoulkadergaye5299
    @abdoulkadergaye5299 Місяць тому +2

    Balla Diouf ya kham lamb

  • @djeganengom
    @djeganengom Місяць тому +1

    Walahi Modou lo mo beuré mo attaqué mo démé ardo mo danou barkep alkhourane siteu defoul dara mais mo dane deug yallako mom 🧏🧏🧏🧏🧏🤷‍♂️🤷‍♂️🤷‍♂️🤷‍♂️🤷‍♂️✅✅✅✅

    • @kbfgaming1883
      @kbfgaming1883 Місяць тому

      Li moy féne ba gueume sey féne en + di wat si alkhour- ane non🥱😂

  • @ivanbocoum7367
    @ivanbocoum7367 Місяць тому +3

    En résumé Siteu n'avait pas d'arguments pour détrôner @modou lo

  • @ibrahimandong2921
    @ibrahimandong2921 Місяць тому

    Siteu mo dane franchement

  • @abdouloume7373
    @abdouloume7373 29 днів тому

    Combat bi vraiment problem de poids feegnu sii, senegalais nio beugua critiquer, Foo diaar niou critiké

  • @papandong9560
    @papandong9560 Місяць тому +1

    Siteuu kasee sisouman yonguen donne

  • @MatarMbodj-df8eb
    @MatarMbodj-df8eb Місяць тому +1

    Siteu stratégie daw la indi 😂😂

  • @papesene5401
    @papesene5401 Місяць тому +1

    Balla diouf waxofidara

  • @DiyenabaPouy
    @DiyenabaPouy Місяць тому

    Siteu loy daw ni rek 😂😂😂😂😂

  • @cheikhdiouf5530
    @cheikhdiouf5530 Місяць тому +1

    Niou balma maie Siteu niouss nako dann nako lolen beugeuti

  • @ibrahimandong2921
    @ibrahimandong2921 Місяць тому

    Modou Lô mo beuré mo attaqué mo khéh mo dem ardo mo danou
    Feliciter léne Siteu guén bayii sén nafék yii magu dey wakh dégu yén gni di wakh Siteu bou nékone sen deurét guén défendre ko fén bakhoul

  • @bayemodoufall2879
    @bayemodoufall2879 Місяць тому

    😂😂😂😂😂

  • @awadiongue5434
    @awadiongue5434 Місяць тому

    Waw mais serigne dagniou ko soote kaye moye dagniou ko diap lay ah modou nékoul

  • @damediop5791
    @damediop5791 Місяць тому +2

    Pour dire vrai Modou est le meilleur mais Siteu vrai tapète la, imagine vous 20mn Siteu daw lép c honteux si wa diamaguene

  • @MohamedThioune-p9k
    @MohamedThioune-p9k Місяць тому +3

    De len wakh DEUG siteu da Daw comba bi khekhoul beuré woul

  • @tallandiaye6481
    @tallandiaye6481 Місяць тому +3

    Thiak thiak 😂

  • @tallandiaye6481
    @tallandiaye6481 Місяць тому +4

    Voilà nak boy daw dagay fekhe dioum loko pour danko mai daw bo khamni tegoko fen daw rék

  • @ibrahimandong2921
    @ibrahimandong2921 Місяць тому

    Yén wakh si micro rek guén meun même bolén ladjé Modou sah dina léne wakh nii Siteu Diambar dégu leuh té Modou dafa danou Yén ayy nafék you magu guén

  • @mdmmboup
    @mdmmboup Місяць тому

    Mais modou lo bou diapé siteu tamite daye féck siteu takhaw wakh tane wakh deugue sila

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse Місяць тому +3

    Siteu mome moy lolou ni mouy beuré bakhoul di daw rk

  • @Matar-h2f
    @Matar-h2f Місяць тому

    Roi kéne doukko kolo kolo dagnoukoy liguéye.
    Siteu daw rékk ladone déff

  • @Pirois
    @Pirois 27 днів тому

    Góor du dawal góor. Siteu nay suul tànk yi

  • @nitoudeugue4930
    @nitoudeugue4930 Місяць тому +1

    Wakhou niou farr rek ngei ndi wakh

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 Місяць тому

    Galassie amoul

  • @AssaneDakar-g3q
    @AssaneDakar-g3q Місяць тому

    Sitteu mo dane

  • @awadiongue5434
    @awadiongue5434 Місяць тому

    Mais sithe bimouy soga dor beuré si digeu bi ladone beuré légui mouye nék didaw

  • @gazza873
    @gazza873 Місяць тому +1

    Bou wakhdji beuri baguen fate nii siteu mo dan modou lo point ❤

    • @RamataWane-t6e
      @RamataWane-t6e Місяць тому +1

      @@gazza873 yor n'a vidéo bou siteu tégué bopou

    • @gazza873
      @gazza873 Місяць тому +1

      @RamataWane-t6e dagua dioum d siteu tegoul boop d

    • @RamataWane-t6e
      @RamataWane-t6e Місяць тому

      @@gazza873 Sisi benen angle bi loulou la wané

    • @gazza873
      @gazza873 Місяць тому +1

      @RamataWane-t6e non image complet bii guadoul am

    • @papambackegueye4181
      @papambackegueye4181 Місяць тому

      Sisi si sakou bi lako tekk

  • @latdiordiop6051
    @latdiordiop6051 Місяць тому

    Balla doul nga d. Modou lo forme bimouvindy bakhoul. Rapidité zéro

  • @ibralemeringue3258
    @ibralemeringue3258 Місяць тому +1

    Siteu légui tiak tiak la

  • @MasseneDieye-op9fq
    @MasseneDieye-op9fq Місяць тому

    Thiak Thiak

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932 Місяць тому +1

    Balla diouf diam mbar la bok

  • @afro3827
    @afro3827 Місяць тому

    Thiak tiak 😂😂

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 Місяць тому

    Siteu yambar la..dafa ragal

  • @mbayelo6090
    @mbayelo6090 Місяць тому

    Siteu mola gueneu xamné bou taxawé danou

  • @seydounouroufaye8353
    @seydounouroufaye8353 Місяць тому +1

    Honnêtement siteu mo dane

  • @marceldiandy3956
    @marceldiandy3956 Місяць тому +1

    Siteu wax rék lay déf ,day business, IL devait etre forfai apres c trois sorti

  • @amadoupam
    @amadoupam Місяць тому

    Franchement siteu bougoul wone dara si combat bi niou waxanté deug nak

  • @taphagueye-l9j
    @taphagueye-l9j Місяць тому

    Bilaye siteu dagno yape di melni tiak tiak daw rk

  • @moussaniang6705
    @moussaniang6705 Місяць тому

    Arrêter n’oublions jamais wa fass nio Dakeu ték xéll si lamb ji 😂 stratégie dfa am si sport yeup mei danou ba paré di woute ay pékhé siteu dfa dane mod’lo les images sont la 😂😂

    • @bilalkhalyfall9938
      @bilalkhalyfall9938 Місяць тому +4

      Gnak djom si yén leu fékeu beu bakh mouy outeu alibi naneu stratégie guaur yallah 20 mn nguay daw gnoula dakhé mounane stratégie

  • @serignesow6903
    @serignesow6903 Місяць тому

    Wayyy mani dawkinda ragal la tapet la day zembaree rek amoul takhaw

  • @PapamakheteGueye-ub5ro
    @PapamakheteGueye-ub5ro Місяць тому

    Yaw balla biguay beurre daniou dan la nok rek do darra

  • @rimesmakerposeidon2427
    @rimesmakerposeidon2427 Місяць тому

    Siteu daw combat bi yeup sou takhawone modou lo reuy ko

  • @superfoottv2277
    @superfoottv2277 Місяць тому

    Vraiment nak modou si combat comme kou done beurè ak rakam dako niouss mouy daw mou diap ko file ko mou naw geneu sakou yi 😂

  • @ibralemeringue3258
    @ibralemeringue3258 Місяць тому

    Siteu bopp boudone si teulé lepay xossou

  • @morramos9050
    @morramos9050 Місяць тому

    Serigne dangay sob rek ngay ragalo malick ngom do régler

  • @MoussaGaye-p5x
    @MoussaGaye-p5x Місяць тому

    yénn nieup ay fans modou lô kénn wakho lénn Lamb wakho farr rk kénn Di wakh

    • @damembow6374
      @damembow6374 Місяць тому

      Konn modou mo guénn sakou yiii saway

  • @adamasall-bw7yo
    @adamasall-bw7yo Місяць тому

    Siteu mo daen modou lo dake faral modou rik

    • @chamousman2726
      @chamousman2726 Місяць тому +3

      😂😂😂😂 Yallah deug la beugu delenko wakh

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 Місяць тому +2

      deléne wax deug ya geuna khamni siteu meunta dane modou lo

    • @PinzipFromdaO
      @PinzipFromdaO Місяць тому

      @@galaxiepro.5641😂😂😂 danouko dako souriuheul 😂

  • @serignesow6903
    @serignesow6903 Місяць тому

    Wayyy mani dawkinda ragal la tapet la day zembaree rek amoul takhaw