Lirou Diane clashe Birame Gning et déclare : " Sou Balla dieulè Mod'Lô niou... "

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 1 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 73

  • @SangFabregas
    @SangFabregas 3 дні тому +7

    Très belle idée Quench, Modou lo peut belle et bien lutter avec les deux mais Sa Thies en premier

  • @cheikhseck3842
    @cheikhseck3842 3 дні тому +6

    Dimbali léne niou ci balla ak modou niom rek nekou niou ci lamb ji sa thies mo wara beuré ak modou walla reug reug modou walla Tapha tine modou Lo

  • @babacarfall4250
    @babacarfall4250 3 дні тому +5

    Très bien Lirou Diane

  • @TopGueye-nv7pc
    @TopGueye-nv7pc 3 дні тому +6

    Le roi des Arènes est sur tous les panneaux publicitaires

    • @niangelhadjiabdoulaziz8930
      @niangelhadjiabdoulaziz8930 3 дні тому +2

      C'est ce que beaucoup ne comprennent pas
      Le roi des arènes gagnent des millions sur les publicités

  • @IbrahimaFall-u3z
    @IbrahimaFall-u3z 3 дні тому +9

    Modou bimouy diél roi bi thi défaite ladiogué wone siteu aussi thi défaite la diogué kone mounoul bagne sa thiés.
    Mais lépp balla gaye la mo wara diappalé rakkam parce que ay moromam yii beuré nagne royal té palmarèsam mo guéna rafét séne palmarès

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 2 дні тому

      Mais Siteu mo dane Modou lo bougn wakhanter deug te Yalka takh !

  • @ndiayekhadim5978
    @ndiayekhadim5978 3 дні тому +6

    Sa thies vs modou lo ,pour l intérêt de la lutte ,,,,,sinon le trio : modou lo ,sa thies et tapha tine......

  • @IbrahimaFall-u3z
    @IbrahimaFall-u3z 3 дні тому +3

    Modou kham nani sa thèse bokkoul ak boy yii mouy beurél. Mais modou ak sa Thiès moy combat bi wala modou ak tapha tine

  • @bayemo4147
    @bayemo4147 3 дні тому +7

    C serai vraiment malhonnête pour balla et pour Modou de prendre ce combat. Balla Bou amee khel DEUG na may sa Thiès mou beuré combat royal
    Modou lo boudée Gör la waroul beurewat AK balla prsk moko wahone , nitt kaddom !

    • @elhadjimamadoudiaw3628
      @elhadjimamadoudiaw3628 3 дні тому +1

      Gayin amoul bene kadou bouy jaar des centaines de millions bouleine gnou sonal li war sa thies mo war balla gaye !

    • @bayemo4147
      @bayemo4147 3 дні тому +1

      @ saway lolou sa xalat la Mais pas le mien

  • @bachirdomouparcelle4293
    @bachirdomouparcelle4293 3 дні тому +7

    Modou respectel sa kaaadu

  • @KaneArman
    @KaneArman 2 дні тому

    Lirou kesse ❤❤❤

  • @omarfall4967
    @omarfall4967 3 дні тому +13

    Balla gaye da wara goré diapalé rakam modou Lo va balla gaye dou combat modou sa thies moy combat on est fatigué des combats revanche

  • @MameAbdouDiouf-l8y
    @MameAbdouDiouf-l8y 2 дні тому +1

    Modou vs sa thies Logique ❤

  • @ladianepathe5637
    @ladianepathe5637 3 дні тому +4

    Sa thies gayi dagnou ko beug sou estimé si lamb dji Prsk amoul gnoko wakhal quoi vraiment Yalna ko yalla defal djiam Mai’s GUIs Nani amoul takhawou si lamb teh balla mooy sama mbeur nk Mai’s adouna xeel

  • @MomoKane-rn9if
    @MomoKane-rn9if 3 дні тому +3

    Modou lo nélaw nga bilahi warone lale balla gaye .liga liguéy yeup yakh ngako .walahi balla gaye dalay dane

  • @tallakatalibeserignebabaca2049
    @tallakatalibeserignebabaca2049 3 дні тому +2

    Sa thies boumou yakamti adina yalla rek mofi nek

  • @mamadouwade6565
    @mamadouwade6565 3 дні тому +3

    Sa Thiès kouko dieuloul tapéte gua

  • @ndoffenediouf2749
    @ndoffenediouf2749 3 дні тому +3

    Limou beugoul maye Sathies sens Métinama trope 😢

  • @niangelhadjiabdoulaziz8930
    @niangelhadjiabdoulaziz8930 3 дні тому +1

    Vous n'avez rien compris.
    Le roi des arènes a des privilèges énormes en matière de sponsoring qui dépasse loin un salaire

  • @kurayahmi
    @kurayahmi 3 дні тому +4

    Neu modou dieul 2 avances yi

    • @MousséGningue-n9b
      @MousséGningue-n9b День тому

      Bane avance laye djeul balla na djeull émeu sene tapete la

  • @PapaNdiayeJr
    @PapaNdiayeJr 3 дні тому +5

    Modou lo si défaite leuh diougué beuré roi bi deeeee len wakh lou raisonnable 🎉Modou lo sa thies balla bou dielei Modou yallna danou😡😡😡😡😡😡😡😡😡

  • @thiawfoot5217
    @thiawfoot5217 3 дні тому +1

    Ngathie Gueye deuk la ❤❤❤❤

  • @alidiouf1439
    @alidiouf1439 2 дні тому

    😂😂😂 Mais WA keur Modou lo il faut niou xam ne Modou lo dafa am défaite ci Balla Gaye 2 avant d'être Roi des arènes 😂😂😂

  • @afro3827
    @afro3827 3 дні тому +1

    Serign wakhal té yalla takh tapha sathies dou advsairam ndakh dafa dane eumeu epi eumeu dane sa thies

  • @davelelion8789
    @davelelion8789 2 дні тому

    Modou lo vs Sathiés Moy combat bi

  • @FalouNgom-o3m
    @FalouNgom-o3m 3 дні тому +2

    Modou lô sa thiés moy comba bi boulén wuiriwiry

  • @ndoffenediouf2749
    @ndoffenediouf2749 3 дні тому +2

    Walahi Modou daffey soralé Sathies beugoul magg dane ko rakk aussi dane ko Modou lo soff nama légui tchim

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 2 дні тому

      Bilahii lolou mo ame dafay bagne Mag ak raak daneko te en plus gnemewoul Tapha tine Modou lo!! Modou lo dafa beug wout yone bou ndokher! Modou lo daaw Tapha tine motax Siteu nious ko daneko

  • @WaxDeug21
    @WaxDeug21 3 дні тому +1

    Modou dou nitou kadou😢

  • @ThioubouArnold66
    @ThioubouArnold66 2 дні тому

    Balla Gaye na may rak dji mou beuré wané boppam ah 😌 on réclame modou vs Sathies

  • @boubacarfall9855
    @boubacarfall9855 3 дні тому +1

    Je suis fan de balla number one mais modou-sathies moy combat bi

    • @assanediop771
      @assanediop771 3 дні тому

      Mais yeen sa thies tapet leu bou coup yi métee day bayi tè modou lo day heekh tè sa thies niémèwoul combat capital yeup la niak

  • @ckhiediongue3211
    @ckhiediongue3211 21 годину тому

    Bala Moy sa bay lirou

  • @groupemancocommunication399
    @groupemancocommunication399 2 дні тому

    Combat modou lo vs sa thies mo logique vraiment

  • @trace-infos2a846
    @trace-infos2a846 2 дні тому

    Affaire défaite mome bodone lolou rék Siteu dou beuré ak Modou lo té en plus Modou lo bimouy dieul Eumeu séne si défaite la diougué wone

  • @mactardiallo2085
    @mactardiallo2085 3 дні тому

    Modou Lo mom sou djeulate balla mom moy diayi bopam ndax xaliss bilahi te ligua ligua li gueyon yep yaxou

  • @MorTouure
    @MorTouure 3 дні тому +1

    Nice ♥️🥰🥰🥰🥰♥️🥰♥️♥️🥰🥰🥰🥰♥️🥰♥️♥️🥰❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @abdoulkhadrecisse5087
    @abdoulkhadrecisse5087 3 дні тому +1

    Modou lo su défaite la dioguei dogua neikk roi
    Lolou dou wakk modou lo daffa ragal sathies ak tapha tine c'est tout.
    Tei inchallah sou dieulattei Balla gaye 2 Balla gaye dinako torokhalatte
    Notez bien ça

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop1206 3 дні тому +1

    Modou lo vs sathies moy lamb j

  • @ndiayepapaserge5997
    @ndiayepapaserge5997 3 дні тому +1

    Modou lo thi défaites la diogué dieule eumeu

  • @bassirougning3121
    @bassirougning3121 3 дні тому

    Lirou boulniou sonal balla mo wara bagne bayi sathiés beuré ak modlo khaliss rék lambeu affairou deumb leu

  • @GueyeSerignesaliou
    @GueyeSerignesaliou 3 дні тому

    Modou n'a respect ay wakham geum yallah dieul sa thies dane ko bayi lambj

    • @Neymar1994-m5m
      @Neymar1994-m5m 3 дні тому

      Bouko dieulé sathies dane ko balla mo geuna noy si modou lou lérr lala wakh

  • @ladianepathe5637
    @ladianepathe5637 3 дні тому +4

    Modou Lo bimouy dieul siteu si défaite leuh diogué boumouniou sonal

    • @fallousylla3283
      @fallousylla3283 3 дні тому

      Balla gaye dafa dane modou lo ème séne delco Modou lo danco

    • @thiamahmadulattekh562
      @thiamahmadulattekh562 3 дні тому

      Par decision arbitrale menoko teukeileik kugn dane ba tok si kawam malheureusement

    • @ladianepathe5637
      @ladianepathe5637 3 дні тому

      @ défaite leuh rek sa thies dan neuh siteu domeu ko daan ko sa thies si reug reug leuh diogue victoire avant defaite eumeu seen siteu sur ces 5 combat dernier Niata défaite leuh si am

    • @thiamahmadulattekh562
      @thiamahmadulattekh562 3 дні тому

      @ladianepathe5637 deugleu mais modou moy de choix et beugoul choix bobou
      Mais meno teukaleik sathies ak siteu lacc mo dane eumeu dernierement siteu tenir ko en echec perte par decision
      Defaite yi bokoul

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 2 дні тому

      @@thiamahmadulattekh562 Modou lo thi defaite la djouguer wone Bako Balla djoutaler 2019, Eumeu mayko chance

  • @mansourkane1426
    @mansourkane1426 3 дні тому +1

    Lirou yaw danga ndaye réwe bireum nging sa baye la nga tok fi beug ko yape

  • @SodaDioufka
    @SodaDioufka 3 дні тому

    Modou lo dieulal sa thies

  • @moustaphadieng2880
    @moustaphadieng2880 3 дні тому

    Ah modou lo dé bou dafa té ni dou mastique ni ko Siteu de fone Lo ko raw la ko balla di deff so lamba tole nga bayi

  • @MousséGningue-n9b
    @MousséGningue-n9b День тому

    Mani balla na djeul siteu mon geun balla modou lo d'où comba

  • @LibassMbengue-uv7kl
    @LibassMbengue-uv7kl 2 дні тому

    Combat Bobou nékhoul.sa thiés vs Modou.fénn bakhoul.gorr sa wakh déjà.

  • @ndiayekhadim5978
    @ndiayekhadim5978 3 дні тому

    Modou vs sa thies, moye lamb ji , intérêt lamb ,

  • @abdoulkhadrecisse5087
    @abdoulkhadrecisse5087 2 дні тому

    Modou lo kou niakka Diom la
    Sou beurei woul nagnou deilo sougnou couronne c'est tout kou soff la tei mom si défaite la dioguei Balla gaye 2 dakou diouteul saniko feulei

  • @modoumbackediop2830
    @modoumbackediop2830 2 дні тому

    Balla tienne kéne douko gnide bamou sétte modou mi dou gnéxou gnébé

  • @AlyNdao-b5x
    @AlyNdao-b5x 3 дні тому

    Balla nabayi sa thies modou lo bou modou beugoul dieul tafa tine modou lo saytanéla da beugeu diakhasé sa ak balla

  • @ckhiediongue3211
    @ckhiediongue3211 21 годину тому

    Dagay doul rek bègue go satheis

  • @moussacoundoul4385
    @moussacoundoul4385 3 дні тому +2

    Mé modou lo mo beugoul beuré ak sa thies Loussi balla meun