sa Thiès Dernière minute Waxna liko Aziz Ndiaye déf//Balla Gaye dafma bét...

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 15 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 125

  • @beuguegalsenziguinchor6280
    @beuguegalsenziguinchor6280 9 годин тому +11

    Moi j’aime sathies parceque il est poli et correcte vraiment et son prochain combat si c,est modou lo inchaala je vais aller au stade

  • @CheikhmbackéDiop-s8r
    @CheikhmbackéDiop-s8r 5 годин тому +4

    Bène mbeur rèk lay supporté mouy Modou lo beugna ga may chance sa Thiès ❤❤❤

  • @NoblesDiop
    @NoblesDiop 5 годин тому +5

    Sa Thiès toujours idéal

  • @awaseye6071
    @awaseye6071 9 годин тому +5

    Sa thies dafa yarou mais boulén diakhass mak akh rak modou lo ptit lo et sa thies rek ❤

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 13 годин тому +14

    Yarou motakh ma beugue modou mayko chance 😢😢

  • @modoubayefallsikroulla1423
    @modoubayefallsikroulla1423 9 годин тому +12

    Bayilène féne délène titré louy deugue té bayi saytané beugue ay vue diaroul lii

  • @ibrahimadiop-k6d
    @ibrahimadiop-k6d 11 годин тому +5

    sa thies Modou lo kass❤❤❤❤

  • @SerigneDeme-m8q
    @SerigneDeme-m8q 10 годин тому +5

    Modou n'a niou maay chance waay
    Kii daxa beurri çi galsen Saa❤ rk

  • @sambaba683
    @sambaba683 13 годин тому +3

    Satiès un grand champion machallahh ❤❤❤❤❤❤❤ yallah ngua am ndam sikaw modou lô aamiine

  • @assanefall4111
    @assanefall4111 14 годин тому +29

    Sa thies yalna la yalla May Ndam si kaaw Modou lo saison bi

  • @alliousylla7979
    @alliousylla7979 10 годин тому +4

    Billahi Modou rek moma bayi thi lamb
    Mé sa Thiess dafa yarou billahi beugue naa Modou maye ko chance

  • @khadimdiop3302
    @khadimdiop3302 11 годин тому +3

    Sa dafa yarou lol sakh Macha Allah ❤❤

    • @AdaMa-r9p
      @AdaMa-r9p 8 годин тому

      Cv fre bilaye dama beige nite kou nite masallakh sa thiess

    • @khadimdiop3302
      @khadimdiop3302 7 годин тому

      @AdaMa-r9p Macha Allah lolou dafa am solo

  • @moussasane3433
    @moussasane3433 5 годин тому +1

    Sa thies machallah ❤

  • @BayeAbdoulayeGueye-en2cn
    @BayeAbdoulayeGueye-en2cn 7 хвилин тому

    Machaalla sa yarouté nékhna ma

  • @mbayediop299
    @mbayediop299 13 годин тому +2

    Diadoeif sathiés suis un fans de modou mais inchala il vas te donner ta chence courage rek yala bahna

  • @abdoudieng6226
    @abdoudieng6226 13 годин тому +5

    Sa thies borom bakh nga MashaAllah

  • @cheikhahmedtidianeseck8531
    @cheikhahmedtidianeseck8531 Годину тому

    Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MbayeDiouf-vi5yf
    @MbayeDiouf-vi5yf 10 годин тому +3

    Il communique bien vraiment

  • @SidiyaFaty-vh8kq
    @SidiyaFaty-vh8kq 3 години тому

    Machallah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ibrahimadiop-k6d
    @ibrahimadiop-k6d 10 годин тому +2

    sa thies modou lo kass❤❤❤❤

  • @MakhtarCisse-lm8ny
    @MakhtarCisse-lm8ny 10 годин тому +3

    Sa thiès vraie sportif

  • @mamadoudiouf9911
    @mamadoudiouf9911 12 годин тому +2

    Moi j'ai beaucoup de respect pour ce mec il communique avec respect

  • @ibrahimaniang1463
    @ibrahimaniang1463 13 годин тому +7

    Bayilene sokhor ki kholam mo rafét yeune nak kou âme alale rék ya bakh

  • @MakhtarCisse-lm8ny
    @MakhtarCisse-lm8ny 10 годин тому +2

    Sa thiès do sama mbeur mais vraiment nawnalla

  • @TidianeDiallo-zs3tz
    @TidianeDiallo-zs3tz 12 годин тому

    Manchllah Sa thies ❤❤❤❤❤❤

  • @majoritepastef
    @majoritepastef 12 годин тому +3

    sa thies mi kouko dieul am ngua problem kholal lokho yi woooouuuuuuuhooou! machllah modou diokhal boy bi roi bi gaw !

  • @senegalndiaye9776
    @senegalndiaye9776 13 годин тому +4

    Sa Thiès Modou lo lanou beugue

  • @mbackefall4248
    @mbackefall4248 13 годин тому +3

    Ki ngoor yalla deug la

  • @BouramaDianko-u3j
    @BouramaDianko-u3j 8 годин тому +1

    Sahies❤❤

  • @BrigitteDione-b2r
    @BrigitteDione-b2r 13 годин тому +3

    Sah. Lodefloudoulfeki. Balla. Gaye. Dosafkene❤

    • @massambadiop8181
      @massambadiop8181 12 годин тому +1

      Sa thies ak balla gaye dioté wougnou dara bayilén sén wakh yii ahh

    • @Bour_ndiaye_bour
      @Bour_ndiaye_bour 11 годин тому

      ​@@massambadiop8181 lo kham si seytané tass keur rék

  • @bellingham-k6t
    @bellingham-k6t 13 годин тому +4

    salif loumatoul 1mois def gua si 7 sorti te thi défaite gua diougué 😭😭

    • @ibrahimadrame9499
      @ibrahimadrame9499 13 годин тому

      😅😅😅😅😅sou wakhoul dou combat di😅😅 modou lo le rois dès koullou mbeur moye sama mbeur mais na dieul sathiéss

    • @morsagnane9813
      @morsagnane9813 10 годин тому

      Billahi

  • @mdmmboup
    @mdmmboup 9 годин тому +1

    Il communique bien reck mouni d'où nopi ay sorti wame tamite lanela doyna bala nguaye bayi da dioum wakh lou rey

  • @ABOUBACARMbengue-v8v
    @ABOUBACARMbengue-v8v 13 годин тому +4

    Wa mane gni néck si Commentair yi di doul rk lane lafi sa Thiéss wakh lou grave déléne lidieunti séne probléme

  • @bolochampion7098
    @bolochampion7098 10 годин тому +1

    Mbeur tange gnigui nanla danga yarou do am Dara lamb affaire thiédo la

  • @KebaToure-z9g
    @KebaToure-z9g 13 годин тому +3

    Man sa tihss Ak balla gaye la bouge

  • @maoudediao653
    @maoudediao653 7 годин тому

    Sa thiés Aka am Personnalité

  • @serigneballagaye4105
    @serigneballagaye4105 13 годин тому +2

    Guisna mbeur bo ignané mageum. Waw amna .moy sa thies

  • @SeckNdiayeKhouma
    @SeckNdiayeKhouma 3 години тому

    Sa Thiès c est un bon lutteur mais Dafa amoul diapaler dafa wet

  • @mbackefall4248
    @mbackefall4248 13 годин тому +2

    Ki damakoy gnanal sek jour yalla taxawouko

  • @ModouBodian-jv4oj
    @ModouBodian-jv4oj 13 годин тому

    Aye wachou sorou la sa Thiès à parfaitement raison

  • @mansourseye7810
    @mansourseye7810 14 годин тому +3

    Sa Thiès Bayil micro yi

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 8 годин тому

    Bless 🙏

  • @khadimndiaye3038
    @khadimndiaye3038 14 годин тому +3

    Yaw mome warone nga nekk champion bou mak mais danga amoul fouleu

  • @azizsylla9898
    @azizsylla9898 8 годин тому

    Ningayy deff d'où lamb.
    Lamball té bayii ningayy deff

  • @SawrouSamb-d9j
    @SawrouSamb-d9j 5 годин тому

    Sewrou sama tomala nouyounala

  • @mbackeka3907
    @mbackeka3907 12 годин тому

    Sa thies" " boy niang combat la dh

  • @moussadiakhate4063
    @moussadiakhate4063 13 годин тому

    Lim Mane si Modou d'où ken kouko si man ,yarona Mane n'a wx

  • @MantaDiop-v3k
    @MantaDiop-v3k 13 годин тому +2

    Balla mbeur yepp ne mome lanou beug mell man ki dafma coumasse soff boulla nitgni di topou balla gaye mo takh ben s'y man beugeu micro

    • @massambadiop8181
      @massambadiop8181 12 годин тому

      Ngani bouko niit yi di tolou balla gaye motax wakhal yaw khamal sa bopou reik

    • @MantaDiop-v3k
      @MantaDiop-v3k 12 годин тому

      D'où gneppede mai Mozart party by yepp grass a balla​@@massambadiop8181

  • @mamecheikhndiaye5774
    @mamecheikhndiaye5774 12 годин тому

    Sathies est une personne correcte

  • @LampDiouf-si7tw
    @LampDiouf-si7tw 13 годин тому

    Sa Thiès demal entrainé dji se forme bi bakhoul😅

    • @massambadiop8181
      @massambadiop8181 12 годин тому +1

      Wakho deugg deih wala kone khamo sa thies a leurs actuel guissouma mbeur boukosi geuneu nekk si état wala nga eupouko dolé chaque jour eupeul ak khep adversaire mokoy danél mais dou niakk entraînement

    • @OumarBa-w7f
      @OumarBa-w7f 11 годин тому

      Ya meune na nday Doul Dmr

  • @damefall8715
    @damefall8715 5 годин тому

    Siteu' dafa yabate

  • @AlliouNgom
    @AlliouNgom 13 годин тому

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @laminefaye6850
    @laminefaye6850 12 годин тому +1

    Abou cefa doul rek lay def

  • @Elhadji2187
    @Elhadji2187 13 годин тому

    Way kate len ndey way meuno len dimbali ndey sa thies reuy lamegnn guen defff

  • @KebaToure-z9g
    @KebaToure-z9g 13 годин тому

    Comantre bye len dit diakhach 2 frère

  • @malickndiaye2804
    @malickndiaye2804 13 годин тому

    Li Balla def si lamb xagn bi defagoko

  • @amethndiaye5099
    @amethndiaye5099 14 годин тому +5

    Sa morom Yi yeup niola raw té bo respectéwoul sa grand frère délou guinaw ni tatt rek

    • @modoumamounembaye5192
      @modoumamounembaye5192 14 годин тому +1

      Ap Ende dou force ken kounè yay khol sa arrenssmant yalla nopi ci lep

    • @bellingham-k6t
      @bellingham-k6t 13 годин тому

      Lolou daguay dem si gno khamni ay kharit lagn gua wakh len KO ki balla magam la dafa wara topou si guinawam par force​@@modoumamounembaye5192

    • @tambadjiro2170
      @tambadjiro2170 13 годин тому +3

      Bayilen gawa jugé.

    • @Elhadji2187
      @Elhadji2187 13 годин тому

      😂😂yoww mba amgua rek

    • @HabibSylla-e3f
      @HabibSylla-e3f 12 годин тому

      Lolou dousi mom si yalla la

  • @beuguesalioubeuguesaliou524
    @beuguesalioubeuguesaliou524 8 годин тому

    Tenp yi dieule gua réseaux d

  • @Garga-n5x
    @Garga-n5x 13 годин тому

    Yen bayilen saytane ki lanlafi wax nit day mano ki borom xolbo rafetla sa kola wax lo bon rek sa data Yay

  • @Abdoumbathie65
    @Abdoumbathie65 12 годин тому

    Forme bi si lokho yi gakoy xame mogi leugey

  • @KhadyGaye-n5g
    @KhadyGaye-n5g 14 годин тому

    Lamb ji legui nekhna dagaye diouguer si defaite di beurel roi des arene 😂😂😂

    • @ridialdieng2861
      @ridialdieng2861 13 годин тому

      Modou noumou donné roi

    • @ridialdieng2861
      @ridialdieng2861 13 годин тому

      Modou da djougué si djioutou dém beuré ak roi eumeu sén wala

    • @babacarfall3979
      @babacarfall3979 13 годин тому

      Modou lo 😂😂😂😂😂

    • @thiamahmadulattekh562
      @thiamahmadulattekh562 13 годин тому +1

      @@ridialdieng2861 eumeu sene mo ladjie revanche
      Balla gaye gui dioutou deux fois beug nek empereur huile jadore dou deug?

    • @ibrahimadrame9499
      @ibrahimadrame9499 13 годин тому

      ​@@ridialdieng2861😅😅😅waw mais bamou démai dafa diouteul ki diouteul Balla gaye dieul rois bi ta bobeu eumeu séne moladione revancham si kharagne lo bayou mbeuryi 😊bokoul mais mane d'accord na modou lo maye sathiéss chance

  • @amethndiaye5099
    @amethndiaye5099 14 годин тому

    Ki vrai Nafek leu

  • @massambadiop8181
    @massambadiop8181 12 годин тому

    Sénégalais yi loutax gnou chaytané beugg forcé problème entre niit sa Thiès dioté woul ak balla gaye dara diamou reik mo nék sén diganté gnifi nekk nane ko déloul si balla defoul dara balla gaye li méti supporter balla gaye yi moy sa dafa nangoul modou lô moy roi des arènes mais c’est normal wakh sa bakhou way wagni woul sisa bakh dara té moy moy roi naniou ko nangoul lolou boumou takh nguén méré sa thies diko kharap

  • @DjibyDiagne-fc3fy
    @DjibyDiagne-fc3fy 13 годин тому +1

    Sa Thiés royal balla mo geune lingay déf

    • @massambadiop8181
      @massambadiop8181 12 годин тому

      Lane mo nékk si balla gaye 2 thi comportement bou rafet bou nékoul si sa thies bamou wara roy si balla gaye

    • @SodaDieng-e6k
      @SodaDieng-e6k 12 годин тому

      Saytàné ga nak lan lafi déf loy wakh

  • @diopmar6382
    @diopmar6382 12 годин тому

    Jourliste bi est nul. Blesse nganan mystique

  • @babacar-bmw
    @babacar-bmw 13 годин тому

    Tu communiques trop sa thies bayil média bi

  • @amethndiaye5099
    @amethndiaye5099 14 годин тому +3

    Félicitations balla gaye yobougua sa papa maka ak sa yaye

  • @coinzsow1415
    @coinzsow1415 11 годин тому

    Stop with the fake title 👎

  • @malickndiaye2804
    @malickndiaye2804 13 годин тому

    Sa thies moy toul nitt gni dan lay diey rek dalal sisa mak balla mo geun ci yaw dh

    • @massambadiop8181
      @massambadiop8181 12 годин тому

      Yéne yénay wakh loulén léroul pourquoi nguén beugg forcé problème si diganté balla gaye ak sa Thiès dioté wougnou dara